Vraiment c'est désolant ! Pourquoi les lutteurs prennent un poids qui ne vous permet pas de prendre un combat sérieux et être un athlète c'est très important comme boy niang
En tout cas Baba Diaw kham na lamb ses combats sont d'un niveau extraordinaire. Li Moy lamb je te jure ses lutteurs en simple ont le niveau en lutte bou wekh bi mokke Dina meti lol.
Journée bi mo dakk si saison bi pour le moment.....PPV demb bi nice naaa dounde na lamb trop ak ambiance .Félicitiations aux vainqueurs et du courage aux vaincus
Zé n'a wagni poids âme gueuneu gueuneu liguéy aye mouvement de fonctionnalités dolé ci yakh leu boursine Yako eup poid mais eupeuko dolé fatélékoul deuxième combats Eumeu vs Gris gris avait 15 kilo de plus que Eumeu séne diappanté épreuve de force beu Eumeu woné Niki guane eupouko dolé dakh kou nék a diapone Yéne poids diarrouko yorré poids athlètes lamb amgua ci thieur machalla
Sen plateau bi dee lamine rek mossiy wax kaatù dëgg , Coach bù nek da wara nek ci giinaw mbëram diko coatché eeh li sport de combat , Vraiment mane CNG gissu sen njariñ ci lamb j luduut lekk xaliss mbër i rek ! Félicitations Général 🎉 ! Courage Bùur jàmbaar dëgg ga 👏🏾
General felicitation ya beurre lepeu lamine pour coach bi daniou ko wara amende walla niou suspendre 3 fois dou nek coach walla 4 mais pas cette maniere
Félicitation G mais poids bi mom dalay sonal ndakh dangua meuneu beurei, day wagni sa vivacité ak sa explosivité motakh combat bi méti si yow. Sa adversaire bou amone cardio bou baakh à l'usure lalay yob.
Poids bi combat bi moko lathie, lolo tax adversaire bi manouko manoeuvré. Bo xolé Zé nga xamné mom na yaram bi té wolouna beurém. Xamna bénén combat ak form bi mouy andi.
@@Concept0208 saway G mom li dou poids bou baakh pour mom. G da meuneu beuré du coups yénn poids yi Day wagni sa explosivité et sa vivacité si mbeur bou meune beuré
Koussi diouk nane xalei la di sonal niit gni té nio geuna yambar nieup yaw mi yadone wakh niom balla gaye liniou meunone meuneutougnko té yagui ni soneu bay wadia dé
L'entraîneur de bour sine perturbe le combat pour permettre à son lutteur de récupérer c'est technique ,alors cherchons une solution pour ne plus vivre de pareilles situations
Général d'où beurou lutte avec frappe totalement s'il duminie son poids après le combat day am retard si lutte simple par ce que lutte simple poids bakh n'a si mais soudé lutte avec frappe la basé wou il peut diminuer après le combat il aura largement le temps de le rattraper
Balla gueye 2 yalla nako yalla mayii Dame Amina
Oumoun
Felicitations Zé. Lamb am nga ci thieur.
Bour Sine du courage, vraiment diambar nga.
Vraiment c'est désolant ! Pourquoi les lutteurs prennent un poids qui ne vous permet pas de prendre un combat sérieux et être un athlète c'est très important comme boy niang
Général malika ndanane leu deh bonne continuation Mbeur
Général mo attaquer mo doumeu mo mériter victoire bi
Zé champion la félicitations mé da dieul poids té poids arrangé wouko
Pour l'année 2022 c la meilleure journée 🔥🔥🔥🔥💪
Bilay
Général malicka champion billay guem co rék si se lokho léye moudié 🙏
Félicitations général mai demal nga ligueyi watt sa forme bi bakhoul
En tout cas Baba Diaw kham na lamb ses combats sont d'un niveau extraordinaire.
Li Moy lamb je te jure ses lutteurs en simple ont le niveau en lutte bou wekh bi mokke Dina meti lol.
Abdou lahat leu koku Moy lamb
Legui zé boul arreter sey entraînement lernala nii manqué nga cardio ak explosivité biga done beurei li tax nga done meune diexal combat si secondes wala so dieko sa adversaire def action bou explosif bou gaw lamb dji djekh nonou ga surprendré wone reug reug grand yoff . Cardio longue distance ak cardio intensité ngey def ndakh beurei doore dafa intense ndax coup yi . Ligey rek lamb soxla nala
Tres pertinent Machalla commentaire bi amna solo cardio moy sports premier
Wakh ngua deug vitesse nako yokh rekh
Félicitations général Malika futur roi des Arènes
Jërëjëf lami Coubcou Mbar coloban
Boy Niang Yalla Nako Yalla May Ndamm in cha'Allah 🤲🏼🤲🏼
Amin way
Lutte tv yena ray lamb dji ak sen perpeyvue bii lamb yii kham guanii ken dousii dieude code
PPV bilahi mo yak Lamb ji
Bossi tolé nonou teugal lapb defko gratuit
Bour Sine c’est un vrai puncheur Bilahi dou bayi
Félicitations Zé du courage bour sine
Général seul❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Journée bi mo dakk si saison bi pour le moment.....PPV demb bi nice naaa dounde na lamb trop ak ambiance .Félicitiations aux vainqueurs et du courage aux vaincus
17:25
Zé n'a wagni poids âme gueuneu gueuneu liguéy aye mouvement de fonctionnalités dolé ci yakh leu boursine Yako eup poid mais eupeuko dolé fatélékoul deuxième combats Eumeu vs Gris gris avait 15 kilo de plus que Eumeu séne diappanté épreuve de force beu Eumeu woné Niki guane eupouko dolé dakh kou nék a diapone
Yéne poids diarrouko yorré poids athlètes lamb amgua ci thieur machalla
Sen plateau bi dee lamine rek mossiy wax kaatù dëgg , Coach bù nek da wara nek ci giinaw mbëram diko coatché eeh li sport de combat , Vraiment mane CNG gissu sen njariñ ci lamb j luduut lekk xaliss mbër i rek !
Félicitations Général 🎉 !
Courage Bùur jàmbaar dëgg ga 👏🏾
Pa yoyou yeuppe ay seytane lagnou guemougnou loudoule khalisse
Xrg lo rk moy mbeur si Lamp dji 💪❤️
Kann. La Lank bagna beuré😁😁😁🤣depuis boumou néké roi
D'où deuk
Félicitation général
Gènèral Kèssè ❤
Zé félicitations champion nga billahi ❤Du courage Osi Bour sine vré jambar nga vraiment ❤️mé general Malika Mii VIP Sax molén Meune kii 🫢
Ze mii nekoul si dara na wagni poid bi
Athia zéé bénzo niongi sa guinaw dh ❤️
Dafa leer
General felicitation ya beurre lepeu lamine pour coach bi daniou ko wara amende walla niou suspendre 3 fois dou nek coach walla 4 mais pas cette maniere
Félicitations sunu mbeur bi general sunu yakar mai il fo k NGA xoolaat sa staff beuré WO fi Dara Lou diar Yone
Kéne méroude bour champions gua
Mais kel combat
Général daga perdre sa rapidité daga djeul poids si lamb ji
Merci beaucoup gé
Merci, Lamine,cng,bi,lii,dou,yone,way
Sénégal dagno yap balla gaye rek mai mbeur Sénégal yeup dagno yore birr
sen entraiment ware Nagnou ko kholate
J'aime bien Lamine 👏👏👏
Félicitation G mais poids bi mom dalay sonal ndakh dangua meuneu beurei, day wagni sa vivacité ak sa explosivité motakh combat bi méti si yow. Sa adversaire bou amone cardio bou baakh à l'usure lalay yob.
Meilleurs journee de la saison
Generale wangil sa poids bi dafa bari koulaye bégué la nak
Félicitation zé
Balla gaye yall na KO yalah mAY ndam rk incha Allah ❤️
Général félicitations
Général champion nga léneu rek moy sa blem moy do respecté sa adversaire yi
Non combat bi nekhna trop
Ohh bour sine djiambar la
Mes la femme qui chante ell est trau forte vraiment
Général malika defe changé légui
DOMOU MALIKA 🎉🎉🎉
Général rois des arènes
Wakh ko degue poid bi bakhoul dr
Courage bour
Vraiment journée bou neex lagniou am taye
Generale Moy bandi dh😂
Capi-BFA from Mbar Lamine Fey nagn leu
Les lutteurs on tendance de prendre trop de poids franchement général n'avait pas besoin tout c kilos pour batre son adversaire
Félicitations Général mes poids bi dafa barri
Moma diakhal G kagn lafi yore poids bou tolni
Si poid bi moy lolou mai félicitation à lui
Poids bi combat bi moko lathie, lolo tax adversaire bi manouko manoeuvré. Bo xolé Zé nga xamné mom na yaram bi té wolouna beurém.
Xamna bénén combat ak form bi mouy andi.
@@Concept0208 saway G mom li dou poids bou baakh pour mom. G da meuneu beuré du coups yénn poids yi Day wagni sa explosivité et sa vivacité si mbeur bou meune beuré
@@Concept0208 say lingua wakh ken andousi so nekè ze sa mbeur leu wakh ko degue lii dou poid wam sou oyo fon touti combat bi diekhna bou yague
Li Moy combat way
"PAY PER VIEW" day yakk lamb. Promoteurs yi ak mbeurs yi lay arrangé peut être mais pas les amateurs de lutte. Yénagui yakk lamb dji.
Général de champion gua mais dagua dise
Général yalla nasa diamo yague
Koussi diouk nane xalei la di sonal niit gni té nio geuna yambar nieup yaw mi yadone wakh niom balla gaye liniou meunone meuneutougnko té yagui ni soneu bay wadia dé
Général mii Nékée dou touss.
Poid boum dieul leu
Lamine legui porteurs de vois nga règlement gneuppako wara respecté dèll khool lingay wakh
Bour sine ndanane nga nk
Zé champion gua mé faw gua liguéyat daga diss troop
General Malika vs???
Zee lambe amgua si walh
Pa biy rapporter dof pur leu defa bari wx
Félicitations ze
Général vs gamou gueye combat leu
Combat bi safna sappe
Général c’est un bon lutteur mais son problème moy amoul intelligence si biir Guew
Zé sa lamb désna, banga waré diékhal lamb ji da yague
Gene xam xam bi dess na lu abri... mais felicitations aux acteurs
Ms général Malika sa poids bii da berie
Lamine tu es tres pertinent,,tu as bien fais de signaler cela,,sport individuel warouniou meuna rouge arbitre
mou déss mbay Gouy gui wakh réc la ngouy deff
Beurè wo lène fi tous kagne kène di bayi dorène tè ay mbagg 😮
Yaw mi yaye mbam 🤣🤣🤣
Pourquoi baol baol yi meune khékhe tapha tine ndiaye tine boursine tapha lére est... )
General Malicka sa c’est une défaite pour lui epuis sont poid peut l’handicaper dans le futur
Talfa vs général Malika combat la
Damaye. Deug sa. Ndaye
L'entraîneur de bour sine perturbe le combat pour permettre à son lutteur de récupérer c'est technique ,alors cherchons une solution pour ne plus vivre de pareilles situations
Nandité sonole bro
Lolou la pour mane
Bour lokhobi amoul problème wala
Pa alla defarata sa wakh bougnou douguai sy lenene nioukoye weto
Zé kassè amoul lenenn
Général d'où beurou lutte avec frappe totalement s'il duminie son poids après le combat day am retard si lutte simple par ce que lutte simple poids bakh n'a si mais soudé lutte avec frappe la basé wou il peut diminuer après le combat il aura largement le temps de le rattraper
lambou bou nékhé dorantéla 🤔🤔🤔
Général kese
Général mii poids bim andi bakhoul
Vraiment Diop amoul niveau ta dafay farr
Jackson vs boursin
Jé dadan la bilakhi diamou reke gay ame daga bakh
Khana bour sine nguéne faral
Lamine mi iske dou Moy dégue miy fén lo Serigne ci 🙄
Reporters bayilëne Di farr
Arbitre bi mome khamoul dara presion bimouy tekk niari mbeur yi tégou woul féne
Wawaw li moy lamb day am khekh day am beurè
Mbur sine dafa ganiou si lokho d
Combat bi nekhna
Mais reporters yi ak gni yoré images yi dangén far lol pourquoi Général rék
Général dafa dieul poids lolou té diss guane avant poids bigua yorone mo guenone bakh si ioe
Général Malika légui dafa patta il faut mou todj yaram yi
Sene piod wi da Bari trop