INEDIT - Documentaire sur Serigne Moussa Ka : Vie et Oeuvre

Поділитися
Вставка
  • Опубліковано 7 сер 2018
  • INFORMER JUSTE, NOTRE DEVOIR !!!!
    Mesdames, messieurs,
    Nous avons le plaisir de vous présenter Sunuinfos.net est le premier site d’enquête du baol pour mieux vous informez .
    Nous restons à votre entière disposition pour des informations complémentaires.

КОМЕНТАРІ • 134

  • @babamba313babandiaye2
    @babamba313babandiaye2 5 років тому +6

    Macha'Allah... amna solo lool. Lou mél ni nieurign la si nieup. Wolofal yi Séex Mussa KA biind matnaa siiweul ba nieup diotsi.

  • @malicktine60
    @malicktine60 5 років тому +24

    Serigne Touba lép la am motax yamoul ak kéne té menoulo koo méngeulé ak dara. Diarama Cheikh Moussa Ka.

  • @mamadoundiaye8167
    @mamadoundiaye8167 11 місяців тому

    Yalna ñu ko Yallah feyal ci barkē Ku Tēd ki ❤️❤️🙏🏾🙏🏾🙏🏾

  • @modoundiaye5803
    @modoundiaye5803 5 років тому +35

    Mane maa gueneu beugg serigne moussa ka ci adouna

  • @baramatoure1538
    @baramatoure1538 4 роки тому +3

    ligueyel serigne touba rek mo woro yalla Nanou ko yalla bakh khi

  • @papito8025
    @papito8025 5 років тому +15

    Yèn gni di dislike set len ci yalla 🤔
    On parle de Serigne touba ak diar diaram dei le serviteur du prophète Mouhamed s.a.w

  • @baymodoumbaye3614
    @baymodoumbaye3614 5 років тому +10

    Serigne moussa Ka yallah nala yallah faye gueneu gui faye

  • @falloumbaye2016
    @falloumbaye2016 2 роки тому

    Sëñ musaa ka yàlla na Yàlla yokk leeram ta taas nu ci barkeem barkeb boroom tuuba amiine

  • @mayoronguer2498
    @mayoronguer2498 5 років тому +6

    Thieye Serigne Touba Cheikhoul khadim❤❤❤lou s Moussa ka ame moma yalla naniouko yalla dollé fayal barké borom Touba ❤❤❤

  • @damediop5316
    @damediop5316 5 років тому +26

    Dieureudieuf borom touba
    Serigne moussa ka kemtanla
    Yalla nako serigne bi dolle
    Geureum si barke b touba amine

  • @moussafaye3804
    @moussafaye3804 4 роки тому +4

    Degal sama tourondo fimou tambale rek(kou khame Yalla khame yonent di ga wayall khayroul khadime)

  • @tidianegueye2565
    @tidianegueye2565 4 роки тому +2

    DIEUREUDIEUF ku tedd ki diarama mame cheikh ibrahima fall

  • @mmmmmim2818
    @mmmmmim2818 5 років тому +40

    Mon grend père fière d'être fait parti de c petite fille mame boye nio laa khame talibés serigne touba di mbokke ci serigne touba rekk na môme serigne Moussa ka

  • @MoustaphaNdao-rx4px
    @MoustaphaNdao-rx4px 4 роки тому +3

    Macha allah yalla yokou léram si barké baye niass amin ya rabbi

    • @babacarsarr5843
      @babacarsarr5843 4 роки тому +1

      Macha allah ku bakh leu wallahi
      Défna Aÿ béytti si Baye Niasse
      Serigne Moussa walliou kamile leu

  • @taphaka60
    @taphaka60 5 років тому +2

    Mame Moussa ka yalla na yalla yok aye lerame

  • @mamembaye7353
    @mamembaye7353 4 роки тому +1

    Yall naniouko yalla fayal
    Ta mayniou degu ak topou

  • @abdourahimkanetouba3120
    @abdourahimkanetouba3120 5 років тому +7

    Wawaw fall machala mouriténa loooool walahi 💖👈

  • @rimokhamou2642
    @rimokhamou2642 4 роки тому +1

    yallna niou yalla fayall s.moussa kâ

  • @awaba5892
    @awaba5892 4 роки тому +1

    S Moussa ka yalla Nanou ko yalla dollé fayal

  • @Darousalam2084
    @Darousalam2084 5 років тому +12

    Yalle nako yalla yeureum khareco aldiana firdawsy amine

    • @diaramamamecheikhibre7174
      @diaramamamecheikhibre7174 4 роки тому

      birane cisse Qui keéy nitou aldjana lëu yalna sunu borom tass ay léram sunu kaw

  • @salioufall1321
    @salioufall1321 5 років тому +2

    Thiéy s.moussa ka

  • @khadimkhouma7074
    @khadimkhouma7074 5 років тому +17

    Machalla ndeye sane amna solo lool serigne mousa ka yalla nako yalla yoke ay leram barke serigne touba

    • @aissatousylla9750
      @aissatousylla9750 5 років тому

      Mane damako beugueu te hawmako ,yalla na yalla yoko leerame

    • @aissatousylla9750
      @aissatousylla9750 5 років тому

      Mane damako beugueu te hawmako ,yalla na yalla yoko leerame

  • @modoudal76
    @modoudal76 4 роки тому +1

    Yalla nane am diam
    Yalla nane am khéwal
    Yalla nane am wér
    Yalla na fane yi gode
    Yalla na hadio yi fadio
    Done ay mouride sadikh
    Si barkép Khassida yi🙏

  • @wakeupafrica9906
    @wakeupafrica9906 5 років тому +7

    Thieuy kemanou serigne touba deugue. Peulh bou deeg wolof.

  • @moussaba1813
    @moussaba1813 5 років тому +4

    Amna solo dieureudief yalna ko yalla faye dieufem

  • @falloundao2527
    @falloundao2527 2 роки тому

    Ndèye san mourit ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @boubacardieng5136
    @boubacardieng5136 5 років тому +1

    Yalla nanu yalla fayal seex musaa ka

  • @gueyelax
    @gueyelax 3 роки тому +1

    Kep kou ziaré serigne moussa ka melnané adj ga makka jouromi yone waxi (seydina alhasse salam)

  • @alydiop4394
    @alydiop4394 5 років тому +6

    Dieuredieuffê Cheikh Moussa Ka(r t a)

  • @kenzykindkeinde38
    @kenzykindkeinde38 5 років тому +31

    Thieuy borom Touba aye Talibé rek mate nagn Borom diamono

  • @serignefalloufall4242
    @serignefalloufall4242 4 роки тому

    Akassa Dieureudieuf serigne moussa ka❤️yalla na yalla yocou co ay leer amine ya 🙏🏿

  • @serignekhadimdiagne9120
    @serignekhadimdiagne9120 5 років тому +1

    Sunuinfo lii Amna solo yalle na lene Serigne bi faye

  • @papawade8521
    @papawade8521 Рік тому

    yalla naniou ko borom touba fayal

  • @maneladia1665
    @maneladia1665 5 років тому +5

    Machallah dieureu dieuf Serigne moussa ka

  • @yayamanga5460
    @yayamanga5460 5 років тому +7

    Serigne touba ay dieufi adaam moy ay mouhdjisa mak yi andoon ak mom nio doon défi khar bax comme serigne Moussa ka

  • @diomrekdiagne2828
    @diomrekdiagne2828 5 років тому +8

    Bamba merci s moussa Ka diarama

  • @bathiemassambandiaye9270
    @bathiemassambandiaye9270 5 років тому +5

    Amna solo lol
    Dieum diou amiy may mame moussa ka

  • @papembengue354
    @papembengue354 5 років тому +1

    Yalla naniou ko yalla fayal... serigne mousa ka

  • @djibrildiouf5943
    @djibrildiouf5943 5 років тому +2

    *Jerëjeuf Serigne Touba*
    *Jerëjeuf Serigne moussa la*

  • @africanjoy4921
    @africanjoy4921 5 років тому +2

    Dieureudieuf borom touba s Moussa ka khadimoul khadiim kénla

  • @petitserigndiop1095
    @petitserigndiop1095 5 років тому +2

    Wallahi ki modi werekaanou BAMBA, mane dey moma taxa abonné ci sèn chaîne UA-cam bi

  • @lampka9546
    @lampka9546 5 років тому +3

    Yalla nako yalla yeureum tè khareko aldiana firdawsi

  • @diagnenarre7448
    @diagnenarre7448 5 років тому +3

    Machallah am na solo yalla na yalla takhawolen rafetna

  • @cest-2023
    @cest-2023 5 років тому +3

    Dieureudieufeti Serigne Moussa Ka

  • @assdiongue7047
    @assdiongue7047 5 років тому +4

    Serigne moussa bindna thi lep

  • @cherifgueye1329
    @cherifgueye1329 5 років тому +4

    رحمه الله ورضي عنه وأرضاه

  • @moussafaye3804
    @moussafaye3804 4 роки тому +1

    Quelle jolie cadre

  • @cheikhka2615
    @cheikhka2615 5 років тому +3

    Yalla nalene yalla fay yiW

  • @madiawdibo3678
    @madiawdibo3678 5 років тому +4

    Amatina solo Dieuredieuf Serigne Moussa KA Dieuredieuf Serigne Touba

  • @hujjatulislam9481
    @hujjatulislam9481 5 років тому +4

    Merci cheikh moussa ka mé nane lay déf ba ame wayou cheikh moussa ka yi

    • @mbayediouf7119
      @mbayediouf7119 5 років тому

      Hujjatul islam lolou kay yombou naaa yangui Dakar ???

    • @secretsdevoiles2567
      @secretsdevoiles2567 5 років тому +1

      kou bakh diokhma sa numéro ndax waye yi sokhla nako lol

    • @mbayediouf7119
      @mbayediouf7119 5 років тому

      Diokhe sma numéro fiii mom day yémmé mé message ma par mail(mbayediouf995@gmail.com)

    • @secretsdevoiles2567
      @secretsdevoiles2567 5 років тому

      envoyé nala message mouride

  • @beydysaliou1926
    @beydysaliou1926 Рік тому

    Barap yii naniouko YESSAL book way mouride yiii

  • @malicktine60
    @malicktine60 2 роки тому

    Serigne Moussa Ka kou am solo la si yoon wi. Meunou fi woonaa niak

  • @mouhamedrassoulgueye4636
    @mouhamedrassoulgueye4636 5 років тому +3

    Diadieuf serigne moussa ka bilahi ya tedd

  • @willystar4007
    @willystar4007 5 років тому +12

    C'etait un neveu direct du fondateur du mouridisme. Un grand érudit lettré en ouolof mais aussi en arabe. Un homme très intelligent aussi.

  • @kman-97
    @kman-97 3 роки тому

    Thiey borom touba si maguam yi 🙏🙏🙏♥️

  • @toubayeniasstv3670
    @toubayeniasstv3670 5 років тому +4

    Machalah

  • @djilyabdoukhadredieng8195
    @djilyabdoukhadredieng8195 3 роки тому

    Thieuy s.moussa ka

  • @mamelamp6983
    @mamelamp6983 3 роки тому

    BOROM TOUBA dou moromu kennn☝.

  • @fallouly168
    @fallouly168 3 роки тому

    Yalla n'a yalla fay mag gni Dane ligueyak s touba

  • @mbayeseye2496
    @mbayeseye2496 5 років тому +6

    MBaye SEYE MOURIDE maye ziar

  • @mouhamadoufalilouniang1197
    @mouhamadoufalilouniang1197 5 років тому +4

    Maashaallaah Jaajëf Ka

  • @madiawmboup7403
    @madiawmboup7403 4 роки тому +1

    Thiey s touba amoul morom

  • @kman-97
    @kman-97 3 роки тому

    Diarama Serigne Chiekh Moussa ka 🙏🙏🙏

  • @ibrataly3719
    @ibrataly3719 5 років тому +2

    Serigne moussa ka kenla

  • @syllayabal2832
    @syllayabal2832 5 років тому +3

    Thiey s Mousa ka khdimou rasoul

  • @MakaveliMr7196
    @MakaveliMr7196 5 років тому +2

    Yalla yoki lérame

  • @mbackemodou3714
    @mbackemodou3714 5 років тому +8

    Thiéy kene dou Cheikh Moussa ka

  • @babagueye9784
    @babagueye9784 5 років тому +3

    Thiey borom touba

  • @ousmaneseye7125
    @ousmaneseye7125 5 років тому +3

    Masalla

  • @ibrataly3719
    @ibrataly3719 5 років тому +3

    Sama serigne ealladji fallou kabir ka

  • @mouhamedmouhamed8005
    @mouhamedmouhamed8005 4 роки тому

    ماشاء الله بارك الله فيكم

  • @fallcheikh3370
    @fallcheikh3370 5 років тому +4

    Machallah

  • @soldaroubayekarimbassiroun4535
    @soldaroubayekarimbassiroun4535 5 років тому +3

    Akassa tawfekh rek

  • @cheikhounakhadimdiagne756
    @cheikhounakhadimdiagne756 4 роки тому

    Maasàllaa am na solo lool jaajef

  • @serignefall5180
    @serignefall5180 Рік тому

    Mach Allah

  • @mourtadalo9670
    @mourtadalo9670 5 років тому +4

    Waw goor mouride

  • @ndeyelo1151
    @ndeyelo1151 3 роки тому

    Dierediéfé serigne touba

  • @ndeyelo1151
    @ndeyelo1151 3 роки тому

    Serigne mousa ka diarama

  • @mamadousall5370
    @mamadousall5370 5 років тому +2

    Machala

  • @serignefalilouka2049
    @serignefalilouka2049 5 років тому +3

    amna solo

  • @youssoundiongue8079
    @youssoundiongue8079 5 років тому +4

    En tous les cas kou ñiank kiniane nii moom diaffe na keep kou AME dara si Serigne Touba wakhnako tee wakhoul sii bopam dara

  • @cheikhka2615
    @cheikhka2615 5 років тому +3

    Macha allah

  • @ousmanedioum8085
    @ousmanedioum8085 4 роки тому

    Serigne moussa ka moy gnanatouyalla mousse rek

  • @sokhnadiouf8673
    @sokhnadiouf8673 4 роки тому +2

    Akkassa

  • @amadousall1479
    @amadousall1479 5 років тому +2

    Amna solo loll

  • @babacarkebe9599
    @babacarkebe9599 4 роки тому

    Dieredief serigne Touba amoul morom

  • @moussafaye6137
    @moussafaye6137 Рік тому

    machalah

  • @babsndiaye3271
    @babsndiaye3271 5 років тому +1

    Lou Serigne Touba massounena dinedeu moka waye

  • @malicksene1904
    @malicksene1904 4 роки тому

    Tabarakallah Macha allah

  • @dameka6223
    @dameka6223 5 років тому +3

    Naice

  • @falloukafallouka8082
    @falloukafallouka8082 4 роки тому +1

    Kidef li defna Lou am soulou

  • @bakhadim7569
    @bakhadim7569 4 роки тому

    Mashallah

  • @abibcisse2236
    @abibcisse2236 4 роки тому

    S Mussa ka samab sopey

  • @daoudawagne936
    @daoudawagne936 4 роки тому

    Amna sollo loll machalla

  • @khadimkebe2313
    @khadimkebe2313 5 років тому +4

    Akassa

  • @boromdarou8741
    @boromdarou8741 4 роки тому +1

    Akash 😭😭🤲❤

  • @morseck7907
    @morseck7907 5 років тому +1

    Diadieuff mouride bii

  • @moussafaye3804
    @moussafaye3804 4 роки тому

    Bamba ci birr cadre bi god dougal Moustapha

  • @sakoka3971
    @sakoka3971 5 років тому +2

    Akasa amatina solo loll

  • @sfallougueye4178
    @sfallougueye4178 Рік тому

    🙏👈♥️👆