Un document historique rare( Grandes figures du mouridisme ) à maints égards

Поділитися
Вставка
  • Опубліковано 28 січ 2014
  • La présque totalité des dignitaires mourides réunis, sur convocation du khalife général des mourides Serigne Abdoul Khadiri, l' Imam des imam (Beaucoup d' entre eux, malheureusement, sont décédés Yalna Yalla yokk leer té taass niou ci séen barké)

КОМЕНТАРІ • 70

  • @matarniang709
    @matarniang709 2 роки тому +12

    Thiey yaram dawna. Adouna dou dara. Ce documentaire doit souvent passer à la télévision pour que cette nouvelle génération puisse mieux connaître les figures emblématiques du mouridisme. Thiéy Serigne Touba!

  • @poundkiima4241
    @poundkiima4241 4 роки тому +21

    Thiey yalla 30 ans après niom nieup presque ken nékatoufi yalla na yalla yokou séni lér.
    Vidéo bi mérité na ay millions de vues.

  • @cheikhcisse9729
    @cheikhcisse9729 9 років тому +14

    Wakhlene dieureudieufe serigne touba

  • @papii2511
    @papii2511 2 роки тому +5

    Archive exceptionnelle

  • @seynabfallou395
    @seynabfallou395 11 місяців тому +1

    Documentaire amna solo lole

  • @mbektemireek8416
    @mbektemireek8416 4 роки тому +4

    Wallahi kou guissli xamni beugu Serigne TOUBA REKK wor wayé nak n'a niou bayixelni ken. Dekoufi 😭😭😭

  • @dieylanidiagne7509
    @dieylanidiagne7509 Рік тому +2

    Ay waay founguéne dieulé biilé archives !!! 😱😭😭😭😭

  • @maimounadiallo8146
    @maimounadiallo8146 2 роки тому +2

    Macha allah yallah na yallah yokou sény lére si barké seydina mouhamed psl

  • @khadydiouf7833
    @khadydiouf7833 Рік тому +1

    Aka beuri kersa ndeysane Serigne saliou yalna yalla Yok seni lérr brk Borom touba

  • @bambacisse4200
    @bambacisse4200 10 місяців тому +1

    DIEUREUDIEUFÉ SERIGNE TOUBA KHADIMOUL RASSOULILAHI SALLALAHOU ALEYHI WA SALAMA DIARAMA MAME CHEIKH IBRAHIMA FALL LAMPE BABOUL MOURIDINA ❤❤❤❤❤

  • @elhadjifalloudia8992
    @elhadjifalloudia8992 Рік тому +3

    Dieureudieufati Cheikh Fallou Mbacke
    Dieureudieufati Cheikh Mor Dia Ndiar
    Sene mbokoum Talibe Elhadji Fallou Dia ibn Cheikh Mor Dia Ndiar

  • @falloudia1016
    @falloudia1016 5 років тому +6

    Yalla nagnou yalla defal diam
    Ci barkeb Cheikh Fallou Mbacke
    Ci barkeb Cheikh Mor Dia Ndiar
    Sene mbokoum Talibe Elhadji Fallou Dia di doom ci Cheikh Mor Dia Ndiar

  • @layesoiree9872
    @layesoiree9872 8 років тому +8

    serigne Saliou borom diamgni borom diamono mame cheikh ibrahima fall mo goreé mo woor amoul morome Ken la do toufi amati

  • @BAMBA347
    @BAMBA347 3 роки тому +4

    Ki Def vidéo bi nit manoko tere dem ajana

  • @Hamsatoul_Rijal
    @Hamsatoul_Rijal 6 років тому +4

    Akassa guiss na sama serigne serigne hamsatou mbacke elimani darou mouhty inbn borom darou😍

  • @naroukadiorpur5543
    @naroukadiorpur5543 4 роки тому +2

    Thieuy adouna dra yagou fi 😥😥

  • @susobass7685
    @susobass7685 6 років тому +6

    yaram dawna khollene nioubakh gni ndayesane serigne touba amoul morom

  • @daoudandiaye5588
    @daoudandiaye5588 9 років тому +15

    thiey kémane deug ngui wayé nakk warnagne thié diangué ni kéne doufy désse

  • @khadimdiop3348
    @khadimdiop3348 2 роки тому +1

    Thiey yalla sonou brom yalna yalla yokkou sèni lère té tass tho sene bargué

  • @LatifYakhine
    @LatifYakhine 8 років тому +14

    euskey ki def video bi Yalna borom bi taxawu Barké Cheikhoul Khadim. begna loolu sax.

    • @LatifYakhine
      @LatifYakhine 8 років тому +1

      A hounzou billahi mina sheytani radjiim. Wa inya ouhinzouhaa bika wazouryatahaa mina sheytani radjiim. Rabi ahounzou bika min hamazaty sheyatini, wa ahounzou bika rabi ann yahdourouni.
      Nous n'avons pas besoin de savoir qui tu es. L'importance est de prier pour quiconque est dans le mouridism ne soit la que pour la face de Dieu.
      Mangui niane nak kep ko xamni guisna message bi mou bagn tontu mouk wadjii. Nax ki naroul def loudoul dinu bakarlo.
      Khadimou Rasoul dafa waxni : zima moul wara hansri ladal laahi fii yadi. Sunu borom def nako mouy borom niit Gni,
      Daldi wax fenen ni: zanaf hin bila dararine, ndiarign lou andoul ak lorangué.
      Lii rek moy li am famoom
      Kep Kouy woté woo Serigne Touba té dou deug ci yaw Yalna borom bi sopila ci Barké Cheikhoul khadim.

  • @cheikhounaseye6714
    @cheikhounaseye6714 3 роки тому +2

    degal serugne bara li nexna bilah yalla na yalla yoki sen lerr

  • @ngonesaliou8347
    @ngonesaliou8347 3 роки тому +1

    Ho yonnou mouride wetna ndeysane

  • @niangfallou8449
    @niangfallou8449 5 років тому +3

    Serigne touba rekka am li

  • @adamakhouma3560
    @adamakhouma3560 5 років тому +1

    Machalla thiey bravo broum touba Ken du s.touba

  • @groupemancocommunication399
    @groupemancocommunication399 Рік тому +1

    Xana boroom yëre bu verte tey rée rek Serigne bass abdou xadar la

    • @poundkiima4241
      @poundkiima4241 Рік тому +1

      Mou way li Serigne Basse avait 10 ans.

    • @sene6344
      @sene6344 11 місяців тому

      S. Moudou magam cheikh bass temps bi mongi tol si diang am 9 ou 10anns

  • @mohamedalifall5516
    @mohamedalifall5516 4 роки тому +1

    Dieureudjeufé Borom Touba

  • @khadimcisse7687
    @khadimcisse7687 4 роки тому +1

    Li dawna yaram dieure dieufeti borom touba

  • @ballasyll6868
    @ballasyll6868 7 років тому +2

    amine barkéb boroom touba

  • @falloudia1016
    @falloudia1016 6 років тому +4

    Dieureudieufati Cheikh Fallou Mbacke Dieureudieufati Cheikh Mor Dia Ndiar.Sene mbokoum talibe Elhadji Fallou Dia di doom ci Cheikh Mor Dia Ndiar

  • @alphaoumarbarry3285
    @alphaoumarbarry3285 2 роки тому +2

    Kii di wakh nii deh khawma foumou nek wayé kouko nié la kou âme tawfekh la

  • @abdoumbaye61
    @abdoumbaye61 5 років тому +2

    akasa amna solo lolllllllllllllllllllllll wayè gnou diaguèsi khamnè adouna doudara kone nanou sakh si ak talibè

  • @elhadjifalloudia8992
    @elhadjifalloudia8992 2 роки тому +1

    Yalla nagnou Yalla defal diam
    Ci barkeb Cheikh Fallou Mbacke
    Ci barkeb Cheikh Mor Dia Ndiar
    Sene mbokoum Talibe Elhadji Fallou Dia ibn Cheikh Mor Dia Ndiar

  • @falloundiayedieye7380
    @falloundiayedieye7380 4 роки тому

    Machalla amna solo lol barkep serign touba

  • @taphakane5499
    @taphakane5499 5 років тому +1

    Amna solo

  • @sasasow50
    @sasasow50 4 роки тому

    Machala vídeo doumasi doyal bilahi

  • @koumbacke9731
    @koumbacke9731 4 роки тому

    Sama serigne sama leup.sante nala gueureum nala

  • @mamadouthiam219
    @mamadouthiam219 4 роки тому

    Dieureudieuf serigne Touba

  • @morkane7942
    @morkane7942 4 роки тому +1

    thaye s touba

  • @almajzoob2300
    @almajzoob2300 10 років тому

    ndeysane guisnaa sama serigne beu s fallou diouroul mom s ibra mom s modou kherri mbacke

  • @alaloumoustaphamassamba8866
    @alaloumoustaphamassamba8866 7 років тому +1

    Amna Solo

  • @bargnindiaye720
    @bargnindiaye720 4 роки тому

    Yalla na yalla bokki léram

  • @balabeybalabey8403
    @balabeybalabey8403 2 роки тому +1

    Kha🎉mbacké baol palén
    Fas keur seringe cheikh dembou fall
    Espagne

    • @user-vo3nl1qh4n
      @user-vo3nl1qh4n Місяць тому

      Yaw DEH Nio bokou foñou deuk te manit Magui Espagne ndeysan

    • @balabeybalabey8403
      @balabeybalabey8403 Місяць тому

      Tourbi nakala ?​@@user-vo3nl1qh4n

  • @khadimkhouma
    @khadimkhouma 9 місяців тому

    Machallah amna solo loool💜♥️❤️‍🩹❤️💕💟

  • @mamadousall7046
    @mamadousall7046 4 роки тому

    Machala

  • @cheikhsacs5567
    @cheikhsacs5567 9 років тому +3

    Anduna diekh na

  • @abdoufall7519
    @abdoufall7519 4 роки тому

    Manchalla

  • @alibosn8950
    @alibosn8950 5 років тому +3

    guis na si borom taif

  • @der351khadim9
    @der351khadim9 4 роки тому +1

    Akassa mourit

  • @adamakhouma3560
    @adamakhouma3560 5 років тому +1

    Vidéo bi amna soulo tourop machalla mangui di dougua guiss vídeo bi xhamna barina si ay mouroum

  • @balabeybalabey8403
    @balabeybalabey8403 2 роки тому

    NIGÉNE ADOUNA NIAPE YALNALÉN
    YALLA DOUGAL ALJANA _
    SI LOUAMOUL HISAB_NOUN NIFI DÉS
    YALLA GOUDAL SOUNOUFAN TANOUWÉR AK JAME SOUNOU FATOO
    MOUDOUGALNOU AL JANA SI LOUAMOUL
    HISAB AAMIIIN

  • @ousmanediop1115
    @ousmanediop1115 4 роки тому +1

    Cëy yalla...video bi amna solla

  • @stoubarek1605
    @stoubarek1605 Рік тому +1

    tiey.adune.amull.soloe.worne.kouNIE.yallne.yele.Jigall.nibue

  • @belkisaxum
    @belkisaxum 8 років тому +2

    where are the ladies?

  • @ibakalonji
    @ibakalonji 11 місяців тому

    Cëy Cheix SÂLIH 😭😭😭😭

  • @mouslimonly7796
    @mouslimonly7796 2 роки тому

    Les fou

  • @aminadiop2320
    @aminadiop2320 Рік тому

    Dieureudieuf Serigne Touba

  • @susobass7685
    @susobass7685 6 років тому +1

    yaram dawna khollene nioubakh gni ndayesane serigne touba amoul morom