Ay way li niawna thi degg degg ki kouko bayi mou guénè wadji thi keureum nieuw deuk ak ndiabotam bis bouko djiguè ma khamni mbeur leuh . Sokhor amna nak ayway ragalen Yalla adouna bi dafa diekh ba pareh lep filagn koy bayi dara doula top thi bir Bamel koudoul khalate sa 1er goudi bamel loula nekh defal Dieu est Temoin
Nena lain xarite amatoul ,nit la khamoul noy déngké sa diabar samoromou goor ak say bien yéna secréyi sa diabar sah warouko wakhatoumala kéné, diamano ji sa lokho gauche bouko wolou ak droite bi.
salut je conseille a cet homme de changer d'avocat qui mettra vraiment l'accent sur le caractere particulier et de la profondeur de leur amitié. car en droit il existe une dispense de preuve ou une impossibilité morale de disposer de preuves materielles entre epoux, freres, amis, ou toute personne vraiment proche. cet avocat renvoiera la charge de la preuve a son ami qui malgre qu'il détient les papiers, ne peut pas fournir de preuves materielles d'avoir fini de verser le montant convenu. il peut injecter appel a l'issue de premier délibéré aussi. il doit aussi expliquer la profondeur et la sincérité de leur amitié et mettre aussi l'accent sur le fait que son ami au moment qu'il lui a exposer son problème, n'était pas solvable car sans revenu regulier, donc il ne pouvait en aucune façon, pretendre acheter la maison en entier. FAITES ATTENTION AUX "AMIS"
Ndeysane nitt mo leundeum mais kaïtou keur aussi nokoy diokhé nitt aussi c’est grave kharit bi moy doméram est ce que dou conspiration sakh avec la justice c’est louche légui kou mousoul niou déf lako
Tu as encore une bonne salaire essayé d'en trouver un autre terrain c'est une leçon pour vous car de nos jours on est tous faux.y'a pas l'amitié sincères par apport à nos ancêtres.du courage grand et que la vie nous apprend toujours et nous donne aussi des surpris.
Nite,do def lou baakh moukou paré yalla dila setane ngay moudier fou metti.Yalla dineuko diokh ndam inchallah.Yalla moko diaraalé fi pour lui montrer le vrai visage de son ami ngir moutieul ko thi ay pékhém you narone gueuneu piiire peut être.Ne Dieul Avocat Yalla bakhna…
Il a dû faire signer des documents légaux même si c est du faux, la justice ne reconnaît que la légalité. Ce qu'il peut faire c est d interjeter appel avec un bon avocat.
C pas un amie c'était juste un profiteur il ne sera jamais heureux dans cette maison car son amie à été sincère avec lui et la aidé dans tout ces difficultés dieu même ne permettra Pas ça c du maraboutage les hommes qui aiment la facilité 😈😈😠😡🤬
J admire vraiment les histoires très morales que vous présentez mais le seul hic est le commentaire personnel que vous en faites, non seulement ça prend du temps, trop d explications et ton jugement personnel n est pas essentiel : livrez juste les faits,les internautes apprécieront, merci pour votre compréhension sinon finalement ça languit bcp.
Mais je pense que son (ex) ami balaamouy dem tribunal peut être Demna thi serigne pour niou meyko dolé au tribunal.Neu dem thi borom kham kham mou khôl lolou bakham parce li c trop facile et puisk dadone def galathe ak ay safaraa thi bountou keureum donc c fort probable
Fatemata Mots bobou dara nékoussi deug bou wére la sama bopou mala geneul dou bagnenala wadji niou torokhaleni ba guénécko kereum lane mockocko indil d'où confiance bou eup acke diapé kharit comme bopam kharit yomboul andando lélé déye déme ba nourou kharit
Confiance ne se donne jamais à 💯/💯 .em plus il ne faut jamais habituer une personne meme ton frere de meme pere meme mere à la facilitè on verra comment il va finir prendre avocat et foncer
Bonjour,il na ka prendre un avocat Dieu est grand du courage merci ❤❤❤. La meilleure des TV.
Yallah rék mondiarra diokh confiance❤❤❤❤
Ay way li niawna thi degg degg ki kouko bayi mou guénè wadji thi keureum nieuw deuk ak ndiabotam bis bouko djiguè ma khamni mbeur leuh . Sokhor amna nak ayway ragalen Yalla adouna bi dafa diekh ba pareh lep filagn koy bayi dara doula top thi bir Bamel koudoul khalate sa 1er goudi bamel loula nekh defal Dieu est Temoin
Merci beaucoup Fatou pour tes histoires ❤
Nena lain xarite amatoul ,nit la khamoul noy déngké sa diabar samoromou goor ak say bien yéna secréyi sa diabar sah warouko wakhatoumala kéné, diamano ji sa lokho gauche bouko wolou ak droite bi.
salut
je conseille a cet homme de changer d'avocat qui mettra vraiment l'accent sur le caractere particulier et de la profondeur de leur amitié. car en droit il existe une dispense de preuve ou une impossibilité morale de disposer de preuves materielles entre epoux, freres, amis, ou toute personne vraiment proche. cet avocat renvoiera la charge de la preuve a son ami qui malgre qu'il détient les papiers, ne peut pas fournir de preuves materielles d'avoir fini de verser le montant convenu. il peut injecter appel a l'issue de premier délibéré aussi. il doit aussi expliquer la profondeur et la sincérité de leur amitié et mettre aussi l'accent sur le fait que son ami au moment qu'il lui a exposer son problème, n'était pas solvable car sans revenu regulier, donc il ne pouvait en aucune façon, pretendre acheter la maison en entier.
FAITES ATTENTION AUX "AMIS"
Excellente idée
Ndeysane nitt mo leundeum mais kaïtou keur aussi nokoy diokhé nitt aussi c’est grave kharit bi moy doméram est ce que dou conspiration sakh avec la justice c’est louche légui kou mousoul niou déf lako
Tu as encore une bonne salaire essayé d'en trouver un autre terrain c'est une leçon pour vous car de nos jours on est tous faux.y'a pas l'amitié sincères par apport à nos ancêtres.du courage grand et que la vie nous apprend toujours et nous donne aussi des surpris.
Thiey yalla euskey nako bayék yalla confiance bou eup baxoul
Je suis choquée ki mo kham Lou Bonn kay diomi na Mane
Les papiers sont faux, il faut engager un calihraphe et. Un avocat
C'est ton ennemi
Nite,do def lou baakh moukou paré yalla dila setane ngay moudier fou metti.Yalla dineuko diokh ndam inchallah.Yalla moko diaraalé fi pour lui montrer le vrai visage de son ami ngir moutieul ko thi ay pékhém you narone gueuneu piiire peut être.Ne Dieul Avocat Yalla bakhna…
Ah yombou Na dh thiéy Sénégal 😢.
Solution bou efficace waadji najoulli 2 rakka naafila bisoub mardi diganté timis ak guié jangue thia.... Ohhh
Ah lolou Sax woroul Di wax publiquement.
Sou nguiéne amé banéne yone boumakoko Mana jaaralél Moy gane inchallah ndax bagouma koukoy utiliser Thi Lou négatif désolé 😢
Diadieuf
Ayway bakheé mako dama nekk si ay khat khat
Donne le secret
@@symalick9600 In what way? Refer back to my first comment
Salam sister Fatou Badola mo Bakhoul Ta Nitt Yi Dafa Melni Dagnou Fater Deh Amena 😢merci Beaucoup et Bonne Continuation ☕ ❤❤❤
Comment ca se fait ?
Une vente sans passer par un notaire ?
Il n y a pas de contrat de vente ?
Na porté plainte déclaré ni kharite bi dafa sathieu papier keureume
Louwerga wakh diamono bi mo sopekou nitdafayi wara ñiaw diort
Sénégal mom justice massoul feu amm sakk
Dieu les départagera in chalah
Bonjour quesque vous écrivez svp
Pour moi nako bayee ak juge boumak bi moy yalla soko yayee ak môme te mou wolou yalla nak bagnia am bena ariyer pance
Nako bahi ak yala te khol ko bakhame foumouye moudjie
Dacorou ma ak yaw
Daffa yomb torop nako toop
Khana khamoul serigne loumou jangal talibe ame dineke dessal louke dore
Il faut que certaine personnel arrete d'etre gentille et naive. L'amitie n'existe pas.
Na dème thij ONG dimouy ligueyé mou wakh léneko niou dibaliko wadii vraie mbame la
Mo fou kharit amati do mime réw ? Mane dé dawna bou yagueu si mbiroum kharit ennemie number one ngay am fofou
Il a dû faire signer des documents légaux même si c est du faux, la justice ne reconnaît que la légalité. Ce qu'il peut faire c est d interjeter appel avec un bon avocat.
Non Ndeysane mon Dieu eupeuneu 😭😭😭😭😭😭😭😭💔
Ayy lepp laa rekkk,, tout n'est pas vrai
C pas un amie c'était juste un profiteur il ne sera jamais heureux dans cette maison car son amie à été sincère avec lui et la aidé dans tout ces difficultés dieu même ne permettra Pas ça c du maraboutage les hommes qui aiment la facilité 😈😈😠😡🤬
❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
J admire vraiment les histoires très morales que vous présentez mais le seul hic est le commentaire personnel que vous en faites, non seulement ça prend du temps, trop d explications et ton jugement personnel n est pas essentiel : livrez juste les faits,les internautes apprécieront, merci pour votre compréhension sinon finalement ça languit bcp.
Machallah
😢c triste vraiment
Na porté plainte pour vol na déclaré ni kharite bi dafa sathieu papier keureume te mou dieul avocat
Mais je pense que son (ex) ami balaamouy dem tribunal peut être Demna thi serigne pour niou meyko dolé au tribunal.Neu dem thi borom kham kham mou khôl lolou bakham parce li c trop facile et puisk dadone def galathe ak ay safaraa thi bountou keureum donc c fort probable
Wadji badola bou bonne wayé Yalla dinalen atté
Diaroul mouy aw feneu na diapou ba seleu diouli niari raka nian wadji yalla atenlen tok setan te nak di saxo hasbunallah wa nihmawakil☝️
Wakh gua deug deh nit mo leudeum! non je suis choquée mais qu’il continue à se batte c’est trop facile
Na wakhtane ak avocat bu bakh té ami pékhé té am foulla mou wakh KO nimou démé té mougne yalla Dina atté tékou mbandou la
Transaction jaiye Keur waruta yommbeh nonu. Hana Senegal amut precedure contract
Vraiment ça fait très mal C'est pas un ami il faut qu'il fait les démarches pour récupérer 😭
❤❤❤❤😮😮
Na tegusl sarap ndeyam mou dem thi serign
Déception pur sakh
Na déff appel topp ko jusqu'à bou
Ayway 😢
Kharite bou kata ndeyaam bi danou warra dakar ndeyaaam😢😢
Wadji da djoum warouka woom diokh keuyitou kër gui en plus justice ay preuves rk la meune atté léne rk mofi déss mou bayi wadji AK Yallah rk
kharit di ay doul kharit day deug
Fatou taye magisa dekku thies kay ben dekk niari 🚉 gare
Mon dieu 😢
Cv Sokhenassi ioe sa histoire yi kagne la
❤❤❤❤
Man Dei âmes sakk kharitt ndakk dagnoulay reikk Beutt gorou Sénégal gno gueineu bonne fi
Kharite amoul d
J'ai pas d'ami en ce moment je vis seul avec ma petite famille
Kharitbii da conrompue justice
Kharite deum leu.lolou fow gnou bakhi si khel
Wadji tamit dofla keyitou keur Kane mokay djohé dans l'air wayé ki wor douko djik dinako guis bilay douko mourlo
ioe sa histoire yi dafa yombou torope
Wadji d copain bi dako ligueye motax juge yi fété ak môme en plus boumousi diéem Dara na bayi lep si loxo yala loudoul deug dou yag
🎉
Nako liquidè le prix d une trahison c es la mor mane kouma woor man damalay réye
Non lii domou adama manouko deff
😢😢😢
Na Woute avocat.
Nitgni alal rek
J'ai du mal à entendre ce traître en tout cas demain il rendra compte a dieu
Thomas senkara
Et
kharit saka bayué ak sa diabar mou kateka
Fatemata Mots bobou dara nékoussi deug bou wére la sama bopou mala geneul dou bagnenala wadji niou torokhaleni ba guénécko kereum lane mockocko indil d'où confiance bou eup acke diapé kharit comme bopam kharit yomboul andando lélé déye déme ba nourou kharit
Confiance ne se donne jamais à 💯/💯 .em plus il ne faut jamais habituer une personne meme ton frere de meme pere meme mere à la facilitè on verra comment il va finir prendre avocat et foncer
Lann moyy kharitt sakk
😭😭😭😭😭😭😭😭😭🤍🤍☝️☝️☝️☝️☝️☝️
Nako reuye mou diéh
Machallah