Net Tali: Kii Yayam Mokoy Liguèye, Ngir Yakh Seuyeum

Поділитися
Вставка
  • Опубліковано 12 гру 2024

КОМЕНТАРІ • 99

  • @faBdf2789
    @faBdf2789 10 місяців тому +11

    Yay bou Bone amna, wayé nako ladj ndakh mok fréreyi ak soeur yi gno bokou bay❤❤❤❤❤

  • @guerrierdelalumiere3195
    @guerrierdelalumiere3195 10 місяців тому +7

    Dafa am yaye AK pape you sohkor man dal nama

  • @oumarmbaye7905
    @oumarmbaye7905 10 місяців тому

    sokhna fatou rafét ngeuh Maashallah ❤️ yaw yaafi nék yalna yalla deugeureul takhaway bi 🤲🏽🥰 merci 🙏🏾 bonne continuation

  • @mamyfallougalass1959
    @mamyfallougalass1959 10 місяців тому +4

    Salam sister fatou amatina solo dama defener khana mere diourouko 😢doyena war yallah nakko yallah wane yone sister fatou souniou wal ci caffè ☕ gui merci et Bonne Continuation ❤❤❤❤❤❤

  • @famakhathiouba6946
    @famakhathiouba6946 10 місяців тому +12

    Soumalenn wakhonn lima doundou ak sama yaye nguenn faté kii walahi hazim 😭😭mais yalla bakhna

    • @juliennedogue8309
      @juliennedogue8309 10 місяців тому +2

      D'égayer diap diouli te toujours yalla te hare sa boplolou moye koye fadeur.

    • @juliennedogue8309
      @juliennedogue8309 10 місяців тому +2

      Famille yeuppe am probables

    • @famakhathiouba6946
      @famakhathiouba6946 10 місяців тому +1

      @@juliennedogue8309 walahi instant bii samay émotion moo diexx awma béneu sentiments dou lou nexx dou lou nakhari bilahi 😭😭😭

    • @famakhathiouba6946
      @famakhathiouba6946 10 місяців тому

      @@juliennedogue8309 bilay dé

    • @famakhathiouba6946
      @famakhathiouba6946 10 місяців тому +3

      @@juliennedogue8309 j ai tellement envie d en parler mais awma kouma wakhal bilahi 😭😭😭😭😭😭

  • @ngagnedeme-w2t
    @ngagnedeme-w2t 2 місяці тому

    Yaye bou bone yalla naniouci yalla mousseul.

  • @yvetteniass7362
    @yvetteniass7362 10 місяців тому +16

    Elle doit demander qui est sa mère ki dou yayam une mère ne serait pas si cruelle envers sa fille

  • @soukeynadione5478
    @soukeynadione5478 10 місяців тому +3

    très bien habillé Fatou

  • @salimatoubarry8889
    @salimatoubarry8889 10 місяців тому +2

    Salam salam Ma chérie métina sente yallah boubakhe bakhe ❤️❤️❤️❤️❤️❤️ démal wakhe tane AK kilifayi gnou yew Watan AK sa yaye

  • @mouninandiaye7917
    @mouninandiaye7917 10 місяців тому +6

    Maachaala, bien habillée

  • @nobasiby9540
    @nobasiby9540 10 місяців тому +3

    Yalnako yalla taxawou

  • @AbsaDiop-ed7ui
    @AbsaDiop-ed7ui 10 місяців тому +1

    ❤❤❤❤❤MASA ALHALLA sokhna Fatou mercie beaucoup diereudief aman solo ❤❤❤❤❤❤❤

  • @nobasiby9540
    @nobasiby9540 10 місяців тому

    Amna niou bone nak allahou akbar 😢😢😢yawmal xiyam dîna metti

  • @oumarmbaye7905
    @oumarmbaye7905 10 місяців тому

    Na fekhe ba kham ndax yay dji moko diour soudé moko diour mou dem si serigne bou geum yalla mou défalko niane diokh ko ay sangat pour mou meuna amat dieukeur ndax mou géneuh keur gui dem seuyi inchallah man dé lolou lakoy conseillé soudé tamit diourouko mou fekhé noumou géné keur gui deuki fénén ba amat dieukeur té mou wout ay niane 🙏🏾 yalnako yalla takhawou 🤲🏽

  • @MamiNdiaye-s8w
    @MamiNdiaye-s8w 10 місяців тому +2

    Sa émission bi nékhnama,surtout boy nane café damay réé😂bay beugue dé😂😂😂

    • @Ftymaa
      @Ftymaa 10 місяців тому +1

      Surtout loolou 😂 je l adore nk ❤

  • @jeancharlesdiatta3056
    @jeancharlesdiatta3056 10 місяців тому +5

    Demal louer bayilene. Yaye naoulela tu me consideres je te considere. Laisse la tomber

  • @jeanmichelmignanefaye9096
    @jeanmichelmignanefaye9096 10 місяців тому

    Vraiment mettina trop sa ma ya yaram sakh da daw.lou eup tourou.na guede yayam dans tous les côtés même khalisse sa ak ordonnance yi bou mo ko dieunde ti.dieu va lui donner un bonheur parfait

  • @FatouBintouDiao-l2h
    @FatouBintouDiao-l2h 10 місяців тому

    Madame supporte encore Jai vecu la meme lhistoire mais a la fin j ai quittè le pays

  • @MamadouhlmBa
    @MamadouhlmBa 10 місяців тому +1

    Doyna war thiey 😊

  • @alinguet7974
    @alinguet7974 10 місяців тому +1

    💓💓💓💓💓😭😭😭😭😭♥️

  • @becaybadjie7214
    @becaybadjie7214 10 місяців тому

    I like your program am from the uk

  • @amilo8936
    @amilo8936 10 місяців тому +3

    Theiy wadiour dina amel domm akh

  • @rayan-wo7dx
    @rayan-wo7dx 10 місяців тому +1

    Naka latje ndakh moko diour

  • @bounasakho
    @bounasakho 10 місяців тому +1

    Machallah la plus belle

  • @KhadidiatouGueye-k8o
    @KhadidiatouGueye-k8o 10 місяців тому +1

    Mes beugo seuy bi di eumb di ameu dome
    Rek ana planique cheuu 😭

  • @mohametthiam4500
    @mohametthiam4500 10 місяців тому

    Fatou llegué dada molde

  • @mouninandiaye7917
    @mouninandiaye7917 10 місяців тому +6

    Ce qui me plaît en toi, c'est que tu n'as pas de complexe à dire que c'est de friperie

  • @Maguette313
    @Maguette313 10 місяців тому +5

    Amna waydiour youy amel s’en dom akh nak 🥲

  • @BasirouSene-dg8ck
    @BasirouSene-dg8ck 3 місяці тому

    Nagena khediallko

  • @salimatoubarry8889
    @salimatoubarry8889 10 місяців тому +1

    Teint bi nise sétena laf thiate

  • @CheikhonaG
    @CheikhonaG 6 місяців тому

    Nanian baat yalla tegul luguene manul nawuti benen djieuguer

  • @oumarsarr9401
    @oumarsarr9401 10 місяців тому

    Na guene louer dji week end mii setsiko

  • @Aissatandiaye-l2o
    @Aissatandiaye-l2o 7 місяців тому

    Nadémeu si Serigne bi mouhoutalko ayeu niane

  • @moudouboye
    @moudouboye 10 місяців тому

    bol bàyi topatol sa yàye dina bàkh mé diàpal ne balégi mane nga amàt diekuer

  • @FatouTraoré-x6c
    @FatouTraoré-x6c 10 місяців тому

    😢😢😢😢

  • @nobasiby9540
    @nobasiby9540 10 місяців тому +4

    Ay way wadiour yi déléne diappalé sén dôme yi diléne déglou nane nga meuneu dieulé sa dôme koumou beugoul en plus ngakoy may ko xamni mat nako papa mouy souffrir thi seuyam lindieunti woko 😢😢😢

  • @moudouboye
    @moudouboye 10 місяців тому

    bodé sa yàye djigene dio rey la amnga proplem ndakh mane na kham ne yow yàngi koye topatou moy siiso mé kountinél dina bàkh

  • @abdoulayengom4942
    @abdoulayengom4942 10 місяців тому +1

    Stp delooul Dakar soriko

  • @lalaidebh5kf
    @lalaidebh5kf 10 місяців тому

    C'est cruelle ki leni tek fitneu lagni trk si kaw yaw milen yeureum yay mbam bi masta cherie yalla guisna lep☝️

  • @KhadyGaye-gb2lv
    @KhadyGaye-gb2lv 10 місяців тому

    Es ce que yaye dji amnako si yone parce que parfois soy seuye ba nialo dom bousseu sosou yaye dia douka beugue . Je m'excuse du terme mais mettyna

  • @DadeauThiam
    @DadeauThiam 10 місяців тому

    Li dé doyna warr lole mère bi louy blème bi grande sœur bi moko diakhasé ak yayam
    Sodone manla damay guene keur gui outi loyer ame sama diam douté mouy continue di topoto yayam elle l'a trop souffert vraiment mére bi mom dafa sadik 😢😢😢😢😢

  • @fatougueye819
    @fatougueye819 10 місяців тому

    Est-ce que dou bayi ré yi

  • @awafall5243
    @awafall5243 10 місяців тому

    N'a guéne keur gui déme

  • @apchadiaga8022
    @apchadiaga8022 10 місяців тому

    Noye diouré sa dome ba paré dit sokhore si sa dome khalatale yalla ak dhé

  • @mameboussombaye7397
    @mameboussombaye7397 10 місяців тому

    Thilima Japp femme bi Daniouko deuddale Ak yaye Dji Dh,
    Souko mané Na Binde 2 souratoul Fatiha bénne bi nako bolék souratoul falaq âyab Fatiha boum Déf Dougal souratoul falaq bamou jéx sangou Thi Nane Thi bisou lundi.
    Banéne Fatiha Bi Mou bolékok souratoune naas comme nonou sangouko bisoub jeudi Inchallah leppay baakh.
    Yalna yalla Barkél

  • @madiopmbaye9010
    @madiopmbaye9010 10 місяців тому

    Nalene bahi ak yala metina trope

  • @PAPAMDiop-ul3hp
    @PAPAMDiop-ul3hp 6 місяців тому

    Yeneu way diour ay natou leu
    Yalla mokoy tek dom yi pour khol sen meun mougn fan la tolou
    Wayé sant yalla rk

  • @aboulayembackediop1387
    @aboulayembackediop1387 10 місяців тому

    Thiey yalla😢😢

  • @oumytam1109
    @oumytam1109 10 місяців тому

    Mougnal rek yalla rek mo ci meune dara nakh wadiour le

  • @guerrierdelalumiere3195
    @guerrierdelalumiere3195 10 місяців тому

    Ma sœur défo Dara

  • @mariamafaye7780
    @mariamafaye7780 10 місяців тому +1

    Nako bayek yalla té khamni yayam dou yalla 😢😮 defois yayi dagnouy amel séne dome akk bilahi

  • @CheikhonaG
    @CheikhonaG 6 місяців тому

    Nakoy takhawu guiryala rek tey diiisok fereram bi te amak diamu ak waguer gui tewal ay wakham teymoytu kukoy torokhal tay dawee yaayam am xel te bange ko da ay xel

  • @manganemodou2915
    @manganemodou2915 10 місяців тому

    Wali😂 lépla 😅walla ?

  • @CheikhonaG
    @CheikhonaG 6 місяців тому

    Mom moko def lim don guis komka ferel bi kubakhla naieuy wakh taanak mom wanku ay porof

  • @poulo8224
    @poulo8224 10 місяців тому +1

    Lolu doyna war

  • @DabaTall-xb6ln
    @DabaTall-xb6ln 10 місяців тому

    ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @PAPAMDiop-ul3hp
    @PAPAMDiop-ul3hp 6 місяців тому

    Yensay parents yi nioy amel akh seni dom dilen deflo lo khamni degno dem ci serigne

  • @originali155
    @originali155 10 місяців тому

    Est ce que réellement moko djour

  • @juliettediatta
    @juliettediatta 10 місяців тому

    ❤❤❤

  • @malickthioubdiallo5333
    @malickthioubdiallo5333 10 місяців тому

    C'esr de la sorcelerie

  • @Thiatendiaye94
    @Thiatendiaye94 10 місяців тому

    Kou fi djitou 😂😂

    • @mariamafaye7780
      @mariamafaye7780 10 місяців тому +1

      Khana manmi thiatou yayam😂😂

  • @omarsissokho8674
    @omarsissokho8674 10 місяців тому +18

    Ndeketeyo ki lico dalmetina kouyi deflou bon samoudie dou rafet amna wadiour you amel akh seni dom yawmal kiyam dina meti

    • @wourelsow1482
      @wourelsow1482 10 місяців тому

      C est la faute des parent sou fékone parent yi djapalénagnouko le mari va la respecter

  • @jjffdf6487
    @jjffdf6487 10 місяців тому

    Yalla dinako faye inchalla naniou tok rék setaneu on verra boudé yaye bi moy dogal walla yalla moy dogal na mougneu rék natoulla

  • @MbarakDieng
    @MbarakDieng 10 місяців тому

    ❤😂❤😂 1:26

  • @Bakelsen99
    @Bakelsen99 5 місяців тому

    Khalé boudjéguéne bii nadéme géré Adouname fénéne si Sénégal

  • @MbarakDieng
    @MbarakDieng 10 місяців тому

    ❤❤😂😂

  • @aissatacamara9779
    @aissatacamara9779 10 місяців тому

    Quelle demande qui est ça mère

  • @MbarakDieng
    @MbarakDieng 10 місяців тому

    1:59

  • @awadiakhate2014
    @awadiakhate2014 9 місяців тому

    Gisna yaye bou ligéy domam pour mou yakou ndakh dom dji diabar bimou takke nékhouko , wadjiour yi gnigui déf dé

  • @khadyfall8315
    @khadyfall8315 10 місяців тому

    Je ne pense pas que c'est sa vraie mère

  • @amatsalima
    @amatsalima 10 місяців тому

    il arrive que nos parents nous fassent de grands torts. les amours et les passions sont exclusives. ils sont personnels. aucun parent n'a le droit d'imposer a ses enfants un conjoint ou ses gouts. ça peut avoir de graves conséquences au niveau de la fidélité au cas ou il s'agit de mariage ou bien encore un manque de vigueur et de volonté quand il s'agit de travail. les parents doivent accompagner, conseiller, leurs enfants, leur aider et encourager dans leur choix. beaucoup de femmes deviennent infidelles et truchent etant mariées parce qu'on leur a imposer un mari.et c'est triste et mauvais car ça finit toujours a coûter cher aux parents et aux epoux et surtout aux enfants. alors prenons nos responsabilités quand il s'agit de notre avenir.

  • @saitsaine
    @saitsaine 6 місяців тому

    Osama photo your image so it's very dangerous

  • @Maguette313
    @Maguette313 10 місяців тому

    Y’a Niak fayda douma def d’ara sa keur do dieund sa keur défar ko dém ak say dom ltx am niou amoul ambition

  • @LÉtranger.7
    @LÉtranger.7 10 місяців тому

    Yaye dji baniouko djikom laa baagn

    • @Maguette313
      @Maguette313 10 місяців тому +2

      Bane djiko la wara bagn si mom d’après limou expliquer yaye dji mo bone rek melni kouko diouroul

    • @LÉtranger.7
      @LÉtranger.7 10 місяців тому

      @@Maguette313 niteu d'où Bagneu niteu djikom lay Bagneu

    • @AbcAbc-wy5qb
      @AbcAbc-wy5qb 10 місяців тому

      @@LÉtranger.7Wa legui expliquel djikom

  • @Black-lion221
    @Black-lion221 10 місяців тому

    est ce que c'est sa mere même

  • @PayaFall-ez1nf
    @PayaFall-ez1nf 10 місяців тому +1

    Mais lolou dafa Haram kokou sa papa la 😮je ne pense pas que c sa mère 😢

  • @Ftymaa
    @Ftymaa 10 місяців тому

  • @laminekanteye7892
    @laminekanteye7892 10 місяців тому +1

    ❤❤❤