On s’excuse de ce problème technique qu’on a eu à avoir avec la vidéo in Sha Allah on va rediffuser la version intégrale ns vs présentons nos sincères excuses pour cette inconvenience merci de votre compréhension la famille 🙏🏾😘
Machallah Machallah Machallah you're the best maman chérie et ce qui m plaît encore plus chez vs moyy vs avez tjrs un plan B pour ce qui n'auront pas l'appareil vraiment merci pour tt
Wahoo je me disais qu'est ce qui se passe ça à rien rien de méchant merci pour cette démonstration pour nous qui n'ont pas l'appareil je fais faire cette recette chawarmas merci encore sama sister bonne journée dominical
Akassa ma cherie xamalni Lo ma beug rek beug nala louko raw te Yallah taax da nga baax rek contane na looolu dila sant bou weer te dilene ziar yen wa Suisse beg nanou 🙏🏾😘
ay ay...machAllah la généreuse billo..thiia deugdeug technicienne cuisine ngua.laff thiat.👅👀.10/10 merci é bravo...j aurai aimé te raconte l histoire du wacharman😉😂😂🙌💝💖👍
Chez Billo Maman aussi lima diaxal moy tchin bi boudee plat bi def viande rek lagn si def mais thcine bi si bopam amoul huil amoul eau esk dou def dara tchine bi ?
Non sis dangaye créer four il faudra mettre du sel, wala béton you sew yi ou Doug dou feke meun ngako gérer ba lek BI dou xadiame après nga tek bene plat door ci def dndawale bi comme nu mako defe oui thine bi rap 🙏🏾😘
Oui tu peux y mettre yaourt nature aussi ds la marinade comme j’avais deja Marine la viande au paravant avec citron et vinaigre pot des jours dc je ne voulais pas us ça soit trop aigre 🙏🏾😘
On s’excuse de ce problème technique qu’on a eu à avoir avec la vidéo in Sha Allah on va rediffuser la version intégrale ns vs présentons nos sincères excuses pour cette inconvenience merci de votre compréhension la famille 🙏🏾😘
Chez Billo tata lo def nonou shawarma guinar bi j’en bave 🤤
Woré Ndour aye ma cherie merci ci compréhension bi UA-cam dafaye deconne rek🙏🏾😘
Chez Billo beugg na la tropp tata ndax sa mourite
Magui sakou guan mayma dédicace 😍😍😍😍🥰🥰☺️☺️🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰😊😊please
Shawarma eupneu
C'est les aléa du direct t'inquiète tes abonnés sont compréhensif
Une cuisine équipée et remplir d'amour.. tata billo tu es une icône de la cuisine ❤
ibrahima kebe aye waye merci yaram sant nanou looolu dila begue fou ou tolou jajeuf 🙏🏾😘
Maa Shaa Allaaa chez billoo lepp nice na
Alhamdulillah yaram sant nanou la bou weer 🙏🏾😘
Machalla yalla na yalla faye nekh na selna yalla na borom touba faye dji barker safar bi
Jajeuf ma cherie gnou bok lep feke ak tal sant nanou bou weer🙏🏾😘
Machalah tata billo lo togg mou nekh rawatina bi merci encor une fois🥰🥰🥰
Aye gnoko bok ma cherie yenako mom 🙏🏾😘💋
Machallah amatina soli
Mangui lay gnanal goude fane ak wër
Amine yaa rabi
Amine ma chérie gnou bok lep feke ak tal 🙏🏾😘
Machallah Machallah Machallah you're the best maman chérie et ce qui m plaît encore plus chez vs moyy vs avez tjrs un plan B pour ce qui n'auront pas l'appareil vraiment merci pour tt
Jajeuf ma cherie waw car on doit inclure ts les membres de la famille chez Billo.
Danou beug Kine guissi bopam mo taax 🙏🏾😘💕
This is lovely l have learned a new way today coz I love cooking thanks for uploading much love mama
Alhamdulillah dear it’s my absolute pleasure. Never loose that love 🙏🏾😘
Wahoo je me disais qu'est ce qui se passe ça à rien rien de méchant merci pour cette démonstration pour nous qui n'ont pas l'appareil je fais faire cette recette chawarmas merci encore sama sister bonne journée dominical
Jajeuf sis je pense que tu as l’occasion de voir la vidéo complète maintenant 🙏🏾😘
Dieuredieuf sokhna ville ziar machalla yalla fèyele cordon bleu geu laf thiatt long vie à toi sopnala loole 👍👏👏💕😘
Delo ziar ma cherie walaye fi de la euppe dagno dopante te mousoul gnou Dax waax Yallah rek mo man lolu contane ci yaw sasou nek 🙏🏾😘
Thank you Bilo, easy for busy Mum
One of kids favourite . God bless more 😘😘
Mia Wone amine sis likewise!
It’s my kinda food specially if u already have all side dish ready to go 😂🙏🏾😘
Machalla koula beug la bilahi dinala suivre depuis suisse nakh danga gniww lolll merci si recette bi
Akassa ma cherie xamalni Lo ma beug rek beug nala louko raw te Yallah taax da nga baax rek contane na looolu dila sant bou weer te dilene ziar yen wa Suisse beg nanou 🙏🏾😘
ay ay...machAllah la généreuse billo..thiia deugdeug technicienne cuisine ngua.laff thiat.👅👀.10/10
merci é bravo...j aurai aimé te raconte l histoire du wacharman😉😂😂🙌💝💖👍
Aida ly Sokhna Aida j’aimerai bien entendre cette histoire xamna re Tass lay done jajeuf ci tewlubi 🙏🏾😘
Encore une merci tres chere sister, amazing seasonings.
Akassa c tjrs avec plaisir 🙏🏾😘
Machalla vous êtes la meilleure 😘😘😘😘😘
Ah merci ma chérie 🙏🏾😘
Bonjour on adore le chawarma merci tata Billo on t'adore
Fatima Noor oh merci ma chérie je vs adore d’avantage ma chérie 🙏🏾😘
Ma Sha Allah Sokhna Billo😘
Akassa ma cherie jajeuf 🙏🏾😘
macha Allah Tata bilo
Akassa ma cherie jajeuf 🙏🏾😘
Amoul baine blem tata nekh na bâ noppi yalla nala yalla Faye leerna settna
Akassa merci ci compréhension . Amine way gnou bok lep feke ak tal jajeuf 🙏🏾😘
MACHA ALLAH...
Saly Diallo akassa ma cherie 🙏🏾😘
@@ChezBillo ❤
machallah sokhna billo
Akassa ma cherie 🙏🏾😘
Waaw machall
Akassa ma cherie 🙏🏾😘
Machallah dinako diem Inchallah
Jajeuf sis 🙏🏾😘
Machallah amal jamm rk
Akassa ma cherie gnou bok lep feke ak tal🙏🏾😘
Trop adorable et perspicace mashallah on t’aime.Aka ma beugue Chawarma
Mberry Mmy fi de la rawe sis it’s a staple at home? Sant bou weeer 💕🙏🏾😘
Chez Billo Alkhamdoulilah .🙏
Comment faire pour trouver cette cet appareil ? Merci
Machallah choukrane
Akassa 🙏🏾😘
Hummm sis yummy 😋 thanks for sharing ❤️
Habibatoulah Bah u r most welcome dear it was a pleasure 🙏🏾😘
Machallah tata
Akassa ma cherie jajeuf 🙏🏾😘
Billo je voudrais ta version de chocolat chaud genre starbuks. Merci pour tout ma chère
Jajeuf sis in Sha Allah dina gnou ci gneuw soon🙏🏾😘
Machallah🥰❤
Jajeuf ma cherie 🙏🏾😘
Humm machalla nekh na on attends la suite
Jajeuf cherie la vidéo complète est entrée 🙏🏾😘
Macha allah
Akassa ma cherie 🙏🏾😘
BSR chérie je t'encourage tes recettes je les adore sinon ta machine de chawarma ou on peut le trouver s'il te plait je suis à Dakar Sénégal merci
Salaam ma cherie merci pour le support cette Machine tu peux la trouver sur Amazon .
Dilene begue bou weer 🙏🏾😘
Machallah sokhna Billo toujours inspirée
Akassa ma cherie merci bcp 🙏🏾😘
Salam Tata bokoy def si tchine bi nokoy defee dama beug xam rek pour en-cas
Tchine bi dou am dara ?
Waleikum Salaam ma cherie non dou am dara sinon meun nga ci def touti bant pour moi joox ko goût fume 🙏🏾😘
Chez Billo oui Maman moune ngako defee ak gaz wala charbon matte?
Chez Billo Maman aussi lima diaxal moy tchin bi boudee plat bi def viande rek lagn si def mais thcine bi si bopam amoul huil amoul eau esk dou def dara tchine bi ?
Very yummy recipes, we love it😘😘😘
Jamila Sowe Alhamdulillah ma cherie thx a lot and it was a hit also 🙏🏾😘
Machallah chawarma poulet migui plaçam
lo zeyna akassa ma cherie jajeuf 🙏🏾😘
Slt chez billo boudée si thi ne gakoy deef dagay deff deu lline va parés tëko thi walla répons stp 🙏🙏🙏🙏
Non sis dangaye créer four il faudra mettre du sel, wala béton you sew yi ou Doug dou feke meun ngako gérer ba lek BI dou xadiame après nga tek bene plat door ci def dndawale bi comme nu mako defe oui thine bi rap 🙏🏾😘
😇💪
Machalla soxna Billo
Akassa ma cherie 🙏🏾😘
Merci ma chérie nexna
Akassa ma cherie Jajeuf 🙏🏾😘
Machala
Akassa yaram jajeuf 🙏🏾❤️
Manchanlla nékhatina 😍😍
Jajeuf ma cherie🙏🏾😘
Rendez-vous à 16h inchalla.. sa me rappelle les restaurants libanais....
ibrahima kebe eh oui mon frère c ce qu’on voulait répliquer surtt pur les nostalgiques du pays🙏🏾😘
ak tata billo wagne bou sétt togue bou nékh
Jajeuf ma cherie sant nanou🙏🏾😘
Vous avez utilisé du blanc de poulet n'est ce pas?
Salam ma chérie non aujourd’hui j’ai utilise cuisse de poulets désossé mais y a des jours ou j’utilise blé blanc de poulet seulement🙏🏾😘
Assalamoualeycoum Sokhna Bilo je m'appelle Dado je vous adore je veux votre adresse où numéro joli dècor
Waleikum Salaam dado ma cherie waw le numéro est là +16463859436🙏🏾😘
J aime dal
Akassa 🙏🏾😘
Ok c des Chose ki arrive thiate dafa gawe
😂😂😂 Jajeuf bi mom daf ma jaxalone mais Alhamdulillah ba Yallah japale nanou ba gnou meun ko defarat 🙏🏾😘
Mio g vue 1 autre Video la Marinade es faite avec du yaourt nature
Oui tu peux y mettre yaourt nature aussi ds la marinade comme j’avais deja Marine la viande au paravant avec citron et vinaigre pot des jours dc je ne voulais pas us ça soit trop aigre 🙏🏾😘
Shawarma rek eupneu
Jajeuf ma cherie 🙏🏾😘
Video yi dafay gudou torop
Machalla nak lepe diarna yone mes dafa foudu dall
Machallah ta billo 👏👏👍
Machallah
Akassa ma cherie jajeuf 🥰🙏🏾😘