Machallah fataya Yi mom Amna solo,bonne et heureuse année dila nianal rek yaw ak sa famille goudou fann ak weer di niane année bou Bess dakh lep , sasouné yagui sédal kholi si recettes niou nekh yalla na yalla Faye.
Salam Sokhna Billo can you please tell how long do you have to leave the mixed dough to set down before the refilled? And also do you nknow if there a ready made dough to buy instead of mixing all
Waleikum Salaam sister usually if I do not mention it that means the dough is pretty forgiving does not need to rest for a long period of time 5 to 10 mins will do or no rest at all. There are some type of bread or pizza dough out there any brand will do; but to be honest making your own taste waaaay better! 🙏🏾😘
Vraiment la grande je suis très honorée , très heureuse merci mille fois une question bo défaré pâte bou bari bokoy garder dégakoy congelé ou bien thie réfrigérateur bi ngakoye déf et en plus on peut garder la pâte pour combien de temps
Ah merci ma chérie oui au fait dangaye congelé pâte BI ci mbouss ou récipient bou meuneu nek ci congélateur bou am couvercle du coup si tu veux la préparer tt ce k tu as faire c de la dégivrer sur ton comptoir ou au frigo s’il fait très chaud 🙏🏾😘
Akassa ma cherie contane na Waw épices yoyu ngay waax nak faw gnou keye moytu comme febar yi dafa bari legui te ken xam oil louye jot nit yi mome faw gnou def taxaw setlu tooti lolu rek la jajeuf waye m cherie sant rek🙏🏾😘
Salam sokhna Billo, bonne année et meilleurs voeux. Une petite suggestion, pense à écrire les quantités en gramme en barre d'info et crois moi tu gagnera en visibilité. Je regarde la vidéo mais je sais que je ne vais pas pouvoir reprendre la recette. Salam Aleikoum et que 2020 soit une année pleine de belle réalisations pour toi. 😘
Salam sokhna Billo, avec plaisir. Tes recettes sont des valeurs sure alors c'est un plaisir de les reprendre. Bisou, bonne continuation, tu nous fait plaisir à chaque publication. 😘😘😘👍
Mashalla sokhna billo mane mome Khassida yi motakh ma sawar dila deglou mashalla yalla na la kou teed ki tek lokhom
Amine ma chérie gnou bok lep feke ak tal ah Xassida yi deh mashallah rek 🙏🏾😘
Je vous adore vraiment c'est la première fois et je vais continuer à regarder vos vidéos et reprendre les recettes yalna sa diam yagu
Amine ma chérie et un Grd merci ci abonnement bi bienvenue ds la famille et j’espère que la chaîne te sera utile inshallah 🙏🏾😘
Tata billo pain chinois kagne gua koy defar ki est d accord
Ma ngui xaar vote yi ma cherie ziar bou weer🙏🏾🥰😘
Salut Mme et merci bcp pour la recette . Au fait j'aimerais savoir si vous les avez cuits au four ou si vous les avez faits frire ???
Il’y a certains que j’ai cuit au four d’autres on a la friture🙏🏾😘
@@ChezBillo Ah d'accord merci bcp 🙏😘🥰❤️💕 c'est vraiment très gentil de votre part 👍 . Merci pour la réponse . Et bonne continuation 😁
Machallah
Laff thiatt
Yarou ngeu
Téye ngeu
Dog bi diarna yone
Merci bcp yena baax rek sant bou weer 🙏🏾🥰😘
Bonsoir Billo machala nicena mane mome damabougone bourou arabe je me suis abonné lafthiat tiakaw tiakanam merci
Fataya 😲😲👏🏼👏🏼👏🏼👏🏼👏🏼👏🏼mangui xar si diam ak salam
Machalla ta billo ndiogonal bou nekh et happy new year mes meilleurs vœux pour cet année 🙏🏼
Merci ma chérie pareillement. Si si ndiogonal bou baax kaye damaye ragal mou faf nek reer deug 😂🙏🏾😘
L'icône de la cuisine 👩🍳👩🍳💕dieuredieuf sokhna billo
Jajeuf yaram merci bcp 🥰🙏🏾❤️
Machalla. Goudale fane. J'en profite pour te souhaiter une bonne et heureuse année 2020.
Amine. Maman gnou bok lep feke ak tal yenit Yallah bayi lene sunu kanam mou and ak wer ak tal 🥰🙏🏾😘
Bonsoir ma sœur pour tout se que tu fais pour nous obrigado.
Machallah merci la grande et bonne et heureuse année
C avec plaisir ma sœur de ❤️
Mashallah sister Billo. Togg nge Lou me beugg et merci beaucoup pour la dedicasse 😍
Ah c avec plaisir waw man mi deh fataya mome moye ci sama xol lako beug 😂🙏🏾😘
Madame Billo damabougone hame gnatagadefesi quantité farinebi c'est 1kg ou 2 kg merci beaucoup de me répondre svp ça va m'aider
Machala ma billo très jolis .On va essayer inchala
Ca me fera plaisir ma chérie 🥰🙏🏾😘
Machallah sokhnasi yalla na lokho bi wére si barquer borom touba
Amine ma chérie gnou bok lep feke ak tal 🙏🏾😘
Machala yalla hebe doli
Bonne Année mes meilleures voeux ma Billo santé prospérité Bonheur yalla sameu la ar laa je te love❤❤❤❤🤲🤲🤲
Fi la euppe ma cherie amine gnou bok lep feke ak tal ❤️🙏🏾🥰😘
Ohh bismilah Néxna machalla
Machallah fataya Yi mom Amna solo,bonne et heureuse année dila nianal rek yaw ak sa famille goudou fann ak weer di niane année bou Bess dakh lep , sasouné yagui sédal kholi si recettes niou nekh yalla na yalla Faye.
Amine ma chérie gnou bok lep feke ak tal te nga jitougnou ci Niane yep yena baax rek ma cherie sant bou weer🥰🙏🏾😘
Salam Sokhna Billo can you please tell how long do you have to leave the mixed dough to set down before the refilled? And also do you nknow if there a ready made dough to buy instead of mixing all
Waleikum Salaam sister usually if I do not mention it that means the dough is pretty forgiving does not need to rest for a long period of time 5 to 10 mins will do or no rest at all. There are some type of bread or pizza dough out there any brand will do; but to be honest making your own taste waaaay better! 🙏🏾😘
Machalah sokhna billo gnata kilo farine la svp
Vraiment la grande je suis très honorée , très heureuse merci mille fois une question bo défaré pâte bou bari bokoy garder dégakoy congelé ou bien thie réfrigérateur bi ngakoye déf et en plus on peut garder la pâte pour combien de temps
adamdiallo dia meune ngua ko congeler saayo ko beugué utiliser ngua tel ko guèné mou décongelé
Ah merci ma chérie oui au fait dangaye congelé pâte BI ci mbouss ou récipient bou meuneu nek ci congélateur bou am couvercle du coup si tu veux la préparer tt ce k tu as faire c de la dégivrer sur ton comptoir ou au frigo s’il fait très chaud 🙏🏾😘
@@ChezBillo merci encore une fois
Tata billo deh ma yékal way
Nél mangui yekal mariama Sylla depuis New York waw kay🤣🤣🤣
Ma chérie boul waax dara sa boss mi ngui nieuw in Sha Allah gno far 😂🙏🏾😘
Macha allah def class diongoma macha allah 🥰🥰🥰
Akassa ma cherie jajeuf 🙏🏾🥰😘
Machallah sokhna si laf thiatt
Akassa ma cherie jajeuf 🙏🏾😘
Mmmmm super j adore les fatayas🇧🇪🇸🇳
Alhamdulillah bene ci man je les adore comme c pas possible 🙏🏾❤️
Machalla tata yi mom bakhna
Alhamdulillah ma cherie jajeuf 🙏🏾🥰😘
Ohhhhhhh j'adore merci vraiment
Alhamdulillah ma cherie gnoko bok 🙏🏾😘
Salam sister ,miss you thanks a lot.happy new year to you ,your family and all your followers.Stay blessed
Amine sis miss u more thx for the Duas and likewise 🥰🙏🏾😘
salam merci pour les astuces merci et je cherche ta recette de riz cantonais
Ah je t’en prie ma chérie je vais en revenir in Sha Allah 🙏🏾🥰😘
merci encore
Machallah choukrane 😘
Akassa sis 🙏🏾🥰😘
Salam recette fataya complète
Akassa ma cherie🙏🏾😘
Mane gua si déf baking soda wala ma gui ziar
Machallah togue bi nekh na, set na té ly ma gueuna nekh thi say togue doo def ay epices(magie ect...)
Akassa ma cherie contane na Waw épices yoyu ngay waax nak faw gnou keye moytu comme febar yi dafa bari legui te ken xam oil louye jot nit yi mome faw gnou def taxaw setlu tooti lolu rek la jajeuf waye m cherie sant rek🙏🏾😘
Machallah chef merci beaucoup bisous ❤❤❤
Merci ma chérie 🥰🙏🏾😘
Salam sokhna Billo plat bou rouge bi rafetna beugna ka torop
Ma chérie merci Waw bobu deh cadeau la wone 🙏🏾😘
Comment garder la moitié du patte
Tu peux la geler pdt 6 mois même 🙏🏾🥰😘
Nice na,❤️❤️
Jajeuf yaram sant bou weer 🙏🏾❤️
Salam sokhna Billo, bonne année et meilleurs voeux. Une petite suggestion, pense à écrire les quantités en gramme en barre d'info et crois moi tu gagnera en visibilité. Je regarde la vidéo mais je sais que je ne vais pas pouvoir reprendre la recette. Salam Aleikoum et que 2020 soit une année pleine de belle réalisations pour toi. 😘
Amine ma chérie tt à fait in Sha Allah je vais y veiller d’avantage merci pour la suggestion et je t’en suis reconnaissante ma sœur chérie 🥰🙏🏾😘
Salam sokhna Billo, avec plaisir. Tes recettes sont des valeurs sure alors c'est un plaisir de les reprendre. Bisou, bonne continuation, tu nous fait plaisir à chaque publication. 😘😘😘👍
Machalah
Jajeuf sis 🙏🏾🥰😘
Macha Allah
Akassa ma cherie 🙏🏾😘
Mane mom ney yomb rek Mdr ma dieul fourchette bi 😂😂
Ngani waw baax na deg nala 😂🙏🏾😘
Machallah j'adore❤❤
Alhamdulillah jajeuf ma cherie 🙏🏾😘
😃👍👌🙏👌💗💗
✋👍👍😛😛😛💋💋
Contane ci dédicace bi 💋
Khady Sarr madame Sow
Tata Billo est trop adorable 😍
Merci ma chérie yaw ya baax rek jajeuf 🥰🙏🏾😘
Mama beugue nala torop magui Touba
Mala raw ma cherie sant bou weer waye yena baax rek 🥰🙏🏾😘
Tata yalla na la yalla harr
Amine ma chérie Yallah defal lene ko yenit 🙏🏾😘
Machalla
Akassa ma cherie 🙏🏾😘
Machallah nekh na dinako diem
Sis bayil Sadi xeer sa boss moye dak foof saax 🥰🙏🏾😘
💪💪💪👍👍👋👋🙏🙏🙏❤️❤️❤️
Dieuredieuf machalla amna solo 👌👌♥️💋
Akassa sis 🙏🏾🥰😘
Maman billo namonnala Machallah comme dab rekk. Mes meilleurs voeux
Ma la raw fooof waye contane na guiss la watt ci keur gui merci et à toi de même ma chérie boul si rare dignou laye nam 😊🥰🙏🏾😘
Wipliw hakaza yaye boy setna nexna
Alhamdulillah sant nanou bou weer yaram jajeuf 🙏🏾❤️
Wa lii lane la ni sa fataye âme na mana de
Yenako mom sama dome 🥰🙏🏾😘
Lolou nekh na trop
Diarra Bousso gniou bok harando
Machalha
Akassa 🙏🏾😘
Machalla
Jajeuf ma cherie 🙏🏾😘
Machalah
Akassa 🙏🏾😘