Salut sokhna Fatou c’est Adama Cheikh, je te suis depuis la France mais wax deugue yalla J’aime bien ce que tu fais. Concernant le thème du jour: moi je vois que le gars est tout sauf sérieux et il mérite vraiment le châtiment de dieu. Sokhnassi na diapou ba séllll diouli deux rakka bayiko ak yalla et niane ko mou atélén. Vengeance amoul ndiarigne et si elle fait quelque, elle pourra le regretter. Voilà mon point de vue
Non non elle doit se remettre à Dieu ne jamais se venger. Si elle est croyante musulmane ou chrétienne Dieu va lui donner un très bon mari. C'est une femme bien
Quelle honte triste et très alarmante nacko bayéck YALLAH walla mou porter plainte wadji kou niack diome la acke yeuremandé ki dou gore té dou goore c'est grave ki boucko touroul diana sakhe Boromame dinacko tour diana wadji mo bone deug deug
Il faut te venger .il faut le detruire ..il a abusè de toi t'a detruit humilié .il faut le corriger durement pour donner l'exemple et proteger les autres femmes
😂 wah mais ndiayène yi louy sène problème. Fou ana ak ablay santé ndiaye kay, tioukoum done bété-bété 100%, tioukoum NDIAYE rék leu meuneu santeu, boulène yéé fittneu.😂😂😂 Sinon je lui conseille de demander à Allah swt de se charger de cet individu. Les oppresseurs n'auront jamais la victoire finale. Aie de la patience et soit endurante ! Dieu est avec les opprimés.
😂c'est pas diana mais djalang mais personnellement je préfère qu'elle porte plainte que de l'amener au djalang car y aura pas de marche arrière pour la deuxième option
Na diouli niari rakka boleiko ak yallah nioune Sokhna si Yaw tmt boul wagni sa valeur disant que daga divorcée djiguen divorcée ak niak nio yam goor soula beuguei d’où hol sa statut
La sorcellerie n’est pas une solution car elle va en subir les conséquences wayei bayilene kou lene gnane ndieck rek guen deglou ko. Il fallait porter plainte pour dette impayé et coup et blessures. Diabaram amna ay mbok dou sone. Douma nek ci nadj nga nek ci Kerr fek Yama togn. Qu’elle porte plainte.
Na diape diouli niari raka wakh Borolebi loutakh mou diakarlo ak mome lata mouye défe niari rakayi sou seulemelé calaméko ak Boromebi Soubhannallah té bayiko ak mome
Salam sister fatou 😢Khale bou djiguen boumou vangewou Nakko Bayi Ak Dina len ater😢sama gars bou len di fater di abonnes di aimer di partager merci sinon sister fatou sangneser nguay sa rouge Bakhena Masha Allah ❤❤❤mayma ci caffè ☕ gui Bonne Continuation Dieureudieuf ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤😊
Tourre ci djalan, mannam tourre comme niango yi. Soummeu donn mom doumma taggo. Dorre fayou, à la guerre comme à la guerre, tous les coups sont permis, point barre.
Goor Bou Meussoul Takk Diabar Kheuy Takk Jiguéne Bou Seuyone Ba Amsi Doom Dara nëkousi ndakh,Yonënté bi(Salal Lahou Aleyhi Wa Salaam) Takkone na Sunu Yaye Khadija (Radiyallahou Anha) tëh Amone na Niary Doom( Goor ak Jiguéne) si Seuyeum Bou Ndieuk après Seuyatna une deuxième fois avant Yonënté bi (Salal Lahou Aleyhi Wa Salaam) Diko Takk.Donc yoyou ay wakhla rëk
slt fatou borom émission bou nekh bi borom maniko thia thieuy 😂 femme bi nako top bamou fayko xalisam ndax wadji dafa gorédi té bone gor bou bakh dou torokhal djigueen mé aussi ndawsi boumko def lolou mouy wax nako bayé ak yalla mou até ko ak mom 🙏🏾
Fallait chercher un certificat médical et porter plainte. Va porter plainte ma belle ... Nul ne doit se faire justice soit même. Niite soula tognè do tognarbi...
Fayoul sino dinako deff kenene ma chérie Fayoul deh
Togn dé bakhoul bouko meunoul diegueul na fayou waye boumou wessou lineka togn ❤
Salut sokhna Fatou c’est Adama Cheikh, je te suis depuis la France mais wax deugue yalla J’aime bien ce que tu fais.
Concernant le thème du jour: moi je vois que le gars est tout sauf sérieux et il mérite vraiment le châtiment de dieu. Sokhnassi na diapou ba séllll diouli deux rakka bayiko ak yalla et niane ko mou atélén.
Vengeance amoul ndiarigne et si elle fait quelque, elle pourra le regretter.
Voilà mon point de vue
Macha allah Longue vie à vous nous sommes très heureux de vous c'est bando diallo depuis Italie Lecce
Non non elle doit se remettre à Dieu ne jamais se venger. Si elle est croyante musulmane ou chrétienne Dieu va lui donner un très bon mari. C'est une femme bien
Ay way tata yoné Nala message ngua lire ko falé woma😮😢❤
Quelle honte triste et très alarmante nacko bayéck YALLAH walla mou porter plainte wadji kou niack diome la acke yeuremandé ki dou gore té dou goore c'est grave ki boucko touroul diana sakhe Boromame dinacko tour diana wadji mo bone deug deug
Nako porté plainte
Il faut te venger .il faut le detruire ..il a abusè de toi t'a detruit humilié .il faut le corriger durement pour donner l'exemple et proteger les autres femmes
Diarouko dh ndakh balamouy dhh dinako guiss inchallahou rabbi
Wa man dor Yim ko dor moma méty boudiarer am Problème deuneu nak ki dafa sokhor na fayou
@@nefertiish liko nara dall mome wadji moy gueuneu metti sx
Kenn Dafa doratoul Djiguene sxx
Mais sagnsé ga 🎉🎉 damage pour le Senegal y'a beaucoup de tristesse 😮😮😮
😂 wah mais ndiayène yi louy sène problème. Fou ana ak ablay santé ndiaye kay, tioukoum done bété-bété 100%, tioukoum NDIAYE rék leu meuneu santeu, boulène yéé fittneu.😂😂😂
Sinon je lui conseille de demander à Allah swt de se charger de cet individu. Les oppresseurs n'auront jamais la victoire finale. Aie de la patience et soit endurante ! Dieu est avec les opprimés.
@@FatouSognane-cr3xz ♥️♥️♥️ ahh deug la wakh di. Wakhal ndiayène yi gnou nangou rék
😂c'est pas diana mais djalang mais personnellement je préfère qu'elle porte plainte que de l'amener au djalang car y aura pas de marche arrière pour la deuxième option
Na diouli niari rakka boleiko ak yallah nioune Sokhna si Yaw tmt boul wagni sa valeur disant que daga divorcée djiguen divorcée ak niak nio yam goor soula beuguei d’où hol sa statut
La sorcellerie n’est pas une solution car elle va en subir les conséquences wayei bayilene kou lene gnane ndieck rek guen deglou ko. Il fallait porter plainte pour dette impayé et coup et blessures. Diabaram amna ay mbok dou sone. Douma nek ci nadj nga nek ci Kerr fek Yama togn. Qu’elle porte plainte.
Na diape diouli niari raka wakh Borolebi loutakh mou diakarlo ak mome lata mouye défe niari rakayi sou seulemelé calaméko ak Boromebi Soubhannallah té bayiko ak mome
❤❤❤❤❤MASA ALHALLA MERCIE BEAUCOUP GRAZIE MILLE VIELEN DANK SOKHNA FATOU ❤❤
Du bist espagnier oder deuschier😂😂😂😂
Maa shaa Allah
@@hat-tijani9305 DIEREUDIEF AMAN SOLO MERCIE BEAUCOUP GRAZIE MILLE VIELEN DANK
Salam sister fatou 😢Khale bou djiguen boumou vangewou Nakko Bayi Ak Dina len ater😢sama gars bou len di fater di abonnes di aimer di partager merci sinon sister fatou sangneser nguay sa rouge Bakhena Masha Allah ❤❤❤mayma ci caffè ☕ gui Bonne Continuation Dieureudieuf ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤😊
Nakko Bayi Ak Yallah dina Len Ater in sha Allah 😢
Tourre ci djalan, mannam tourre comme niango yi.
Soummeu donn mom doumma taggo.
Dorre fayou, à la guerre comme à la guerre, tous les coups sont permis, point barre.
Nako bayi ak yalla fayou yalla mo guen bou nitt
Nako bayi AK yalla souniou borom🙏🙏🙏
salam sokhna fatou merci
ASALAMALEKOUM SOKHNA FATOU non nakou baye ak YALLA
Naka bayi ak yalla momane nieup☝️
Goor Bou Meussoul Takk Diabar Kheuy Takk Jiguéne Bou Seuyone Ba Amsi Doom Dara nëkousi ndakh,Yonënté bi(Salal Lahou Aleyhi Wa Salaam) Takkone na Sunu Yaye Khadija (Radiyallahou Anha) tëh Amone na Niary Doom( Goor ak Jiguéne) si Seuyeum Bou Ndieuk après Seuyatna une deuxième fois avant Yonënté bi (Salal Lahou Aleyhi Wa Salaam) Diko Takk.Donc yoyou ay wakhla rëk
Sokhna Fatou ziarnala mais môme nako yobou si yone mo guene ay dialal bakhoul
Mane chaque jour mani kaine douma fay far
Merci beaucoup Ndeysane eupeuneu 🥺🥺🥺🥺😭😭😭
Nako def dailague, wadji kou Bone la ,boumouko bal thim ❤❤❤❤ak Lou ndaysi meuna def amoul sens bouko féyone si foula thiow dousi am❤❤❤
Je vous adore
Na wo wa Guinée ki vraie doomram leu wadji il n'est pas reconnaissant naka tour Diana rek
slt fatou borom émission bou nekh bi borom maniko thia thieuy 😂 femme bi nako top bamou fayko xalisam ndax wadji dafa gorédi té bone gor bou bakh dou torokhal djigueen mé aussi ndawsi boumko def lolou mouy wax nako bayé ak yalla mou até ko ak mom 🙏🏾
Bouko liguéye mais nanko porté plainte Soko menoul bayi ak yalla
Bonjour ma chérie Fatou tu très belle bravo long vie à toi chérie ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Merci ❤
Thiey Thiey ki sokhorna😢
Fallait chercher un certificat médical et porter plainte. Va porter plainte ma belle ... Nul ne doit se faire justice soit même. Niite soula tognè do tognarbi...
Nako janna !! Ku vrai mbam lac!! Tu aurais du porter plainte bamu la dore !! Euye budone mane
Ma chérie mounial ta yallah takh Fatou sopenala amal jam diou sakh AK la chaîne
No yobouco si yone sakh mo guene yag adinam donc mètina togn naco wayè fayoup yalla mo guene fayaneto bou nut
Oui naka tour si djianna boumuko bale tiogne bi dafa metti trop
Il faut le faire. Diaroul tago. Yobou ko fofou ngay wakh. Sou benene yonée diga moytou. Toure ko ndiana. Bilahi boul ko baal.
Nako bayék yalla wadji dinako guiss
Nako ligueye tour diana❤❤❤
Wadji dh meme souko porté woul plainte sakh yalla dina léne atté
Stp 🥹 balko nakh yalla mignou sak sakh😮dagnoukay togne 😢diegalouko mou diegual gnou 🙏balko rek🥹 mais métty na nak 🥺😊
Wadji limu def niawna toroop
😂
❤
Gatsa gatsa la fille defal le tout ba def KO pur😢😢😢
Nako yoboù si yoon pasqu wadji doolé lakoy diay nako porté plainte teuth ko ki dòméram piir la🤬
وجزاء سيئة سيئة مثلها فمن عفا وأصلح فأجره علي الله
Avec le temps il verra ,lou way def tot ou tard dinako guiss . Triste fin pour lui
Kou yakh sa adouna dengaye yakh adounam
Non non qu elle ne le fasse pas que elle laisse tout entre les mains de dieu
Lolou dey yomb trop
Boum kou def dara nako bayi ak yalla até yalla mo guen bou nite bilay akam dinako dal
🎉🎉🎉
Fatou. Chey doyna war
Na fayou dé bilahi boum ko ball
Ah diarouko adouna amoul solo thh yallay taydji xaratoul kou dead dalay fayy ngay guiss
Nako tour diana .amoul xalat .nako tour .mou dièx .lolou la wax ah
Femme bi kou gnak fayda bimouko doré lako worone porter plainte
na ko tethe sokhna fatou😭😭😭
Mon petit conseil faut pas lui amener se marabout il n'a car lui porter plante 🙏🙏🙏👏
Nako yobou prison niamal ko 6 mois fofou li dafa yimbou bly
Sokhna fatou nekhoul ba nekhoul wadji dafa bone defal lila sa khel diokh tour ko djialant kay yobou sa alal gagne la dotna warrrrrr
Bayeko yalla
Boumou ko ball tou seuff ay dor
💓♥️😭🇸🇳♥️❤️
Boum ko ball dey yomb trop wadji dey diay dolé porté ko plainte yarr ko tourr Ko
Ki da deugeu ndeyam deuthie ko ki dou gorr
SALUT GUISE GUA YAW SO NARONE DO LATHIE KÉNE AVIS SOIT GUA DÉF KO OU GUA PORTÉ PLAINTE MAIS KI DO KA BAYI NI TA VIE EN DÉPEND
Ka ay ma mayla diarna yoon ba tayyi
Mane magui maroc gor yinek maroc nonou rek lanoufi neke triande loufi khele you djiguene yi ligueye niou leko dilene khol
Na woo wa deukkba té xamni mbame la Amal affere
Nako bayi ac yalla
Fi Maroc amena yena goor yo khame ni boul sekh ak nouyo. Wakhoumalak sekh ak niom relations ba bor disi ame khebou dara doul mome champion laniou si
If I was her i have nothing to fare she ready do her best
Nako bayi ak yalla !!!
Na fayou car wadji moko togne ndakh ki djigeen la liguey ba tass après diko menance tourko sino dafay yombe trop
Vraiment c'est pas normal la dame a le droit fait ça quart le gars et un voyous assassin
Na dém si yoon waye
Mou fayko xaliss bi
Defall liga beg def
Bilay nakako def ki kou Bone la
Elle n'a qu'à faire tout qui la semble bon
Sans hésiter
Wadji domoukharam la boumco balll nako tour
Après avoir fait le tour dialang l'homme moura directement
Nako defal tou dialague
❤ok
Dioulityi dYbale teyallTakh
Payi kou ak yalla
Nafayou naco toure 🇬🇳
Non soxna fatou c'est pas diana mais c'est diallan
Ziar mourtalla diop diokhme ndiaye rek UK 🇬🇧
Bonjour bal ki kou bone la
😢
Nako toure diéna
Naka tour diana bakkar amou thi
Cest la fille qui est responsable car cest elle qui la proposer à l'homme elle na pas confiance en elle
Ma chérie fayoul waadji domaram la piire
Na fayou togn la dorla ma soeur sou feké yagui may degu fayoul gua yonekoni dou moom rekk mo meune def louko nekh
avuture le avant de faire sa
Togn bahoule