Ma Ibra Laye - Juger nitt ( Ibra Seck )
Вставка
- Опубліковано 28 лис 2024
- Lu bari ci nitt yi da ñuy juger sééni moroom, di sukkandiku ci li ñu léen di nettali, walla sax ci lu ñu téewé.
Waaye nakk na ñu baayi xéll ni, mbindéef munul deff jugement bu parfait jëm ci moroomam ndax ngir loolu mana nekk, dafay warr ñu xam yéeney nitt ki bi mu jëff, xam aussi ci yan condition la nekk ba muy jëff, waaye aussi da ñuy wax ni "les apparences sont souvent trompeuses" motax nakk bari lu ñuy téewé te bu ñu ko attée rekk juum.
Ma Ibra Laye - Ibra Seck
Ma ibra laye man de fallou la todou ta mourid la ms damala bueg ta yalla tax sa nemouro teleponne rek la soxla
Je suis fière de toi je t'aime fort que Allah vous donner tout ce que vous voulez 🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰Amine yarabiiii 🤲🤲🤲
Diadieuf sangue bi❤❤
Machallah vraiment j'ai trouvé une autre dimension aux conférenciers layer à vous 2 Mansour et Ibra laye je vous suis depuis la Mauritanie
Bonne continuation
Masha Allah lou diarra bayi khel la.diadieuf Lahi Maxtar
Machalla
Machallah Laye Makhtar ❤❤❤
Jërëjëf sanga bi boul ma fatte ci gnaane
❤❤❤maala beug piir❤❤❤
Machalla laye makhtar
Jërëjëfëti laye madiné boul ma fatté ci ñaan in chaa Allah
personne ne jugera personne seul reste dieu oui jugera aux jugement derniers, merci frèrooo.
Wallay ndeysaan sama sëriñ, yalna Yàlla jéggël ñu suñuy njumté ci barke Yonnent bi asws. Jërëjëfëti
Sakaw sacanam
❤❤❤❤❤🎉🎉🎉🎉🎉
Mach'allah
Jërëjëf bul ma fatte ci gnaane in chaa Allah
Machallah ❤
jërëjëf, boul ma fatte ci gnaane in chaa Allah
@@AllBusinesstv inchallah laye Mahtar
Salal lahou halla mouhamad
personne ne jugera personne seul reste dieu oui jugera aux jugement derniers, merci frèrooo.
Machallah ❤