Machalla tout baye but dougouna bou yagg xiste aboubacar ak diane bi xawma ba xam gayi degnan la wayé lerna beggg nan baye yalla nalla yalla yagal si keparou mawlana sangue aboubakrin barhahamou BABA ndiaye!!
Machalah xam xam rafétna lerna mai Faydou dafa yatouna lol té xamo gneup donc faut pas guey indi débat yi Serigne faydou dou xassaté dou waxaté lou gnaw bokh dey ak baye leuh
Machallah BAYE TOUT BAYE sa émission bi rafet'neuh trooooppp waay. Liii rk doyneu niou guëstu mbirou BAYE NIASS...ndax limou diangalé ci Dîné dji ak Tarikha Tijaan bi warna nitt nieupp nieuw dioko ak BAYE NIASS ndax njeurign leu rk ci jaam gni. Wayé nak aussi MAWLANA SANGUE ABÛBAKRIN BARHÂMU NDIAYE mii yarr TOUT BAYE mii di wax Sénégal warnagn ko degglou dh pour xam limouy wax
Amiiine ya Raby wallahi Macha'Allah 🥰🙏 Macha'Allah Tout Baye Kham-kham bi bari na Macha'Allah, Yallah na Yallah barkél ! Mais félicitations Oustaze Maodo, très bien dit, il faut parler aux gens à leurs niveaux car tout ne se divulgue pas ! Merci bien ! Dieureudieufééé Baye !!!!
Yalla bo gatt fan si barke baye niass
Allahou akbar dieuredieuf sangue barham ndiaye srg bou bakh soko beuguè xam xolal si talibém
Machalla tout baye but dougouna bou yagg xiste aboubacar ak diane bi xawma ba xam gayi degnan la wayé lerna beggg nan baye yalla nalla yalla yagal si keparou mawlana sangue aboubakrin barhahamou BABA ndiaye!!
Machallah tout baye goor yalla DEUG nga kou meuna defar rek indil kou melni djeureudjeuf sangue barhamou ndiaye
Machalah xam xam rafétna lerna mai Faydou dafa yatouna lol té xamo gneup donc faut pas guey indi débat yi
Serigne faydou dou xassaté dou waxaté lou gnaw bokh dey ak baye leuh
Machalah genre waxtaan yi la niou sokhla dafa Diot gayi khamni baye Niass mo sout nieup si makama dou moromou ben mindef
Waw sa way nagn wakhtané deug deug kouy Baye gnou nopi rk té gnoune rk gno wara wakh ndakh sougnou wadji mo raw gneup.
Tout baye nioun talibe bayeniass yi nous sommes très fiers se toi
بارك الله فيكم ❤❤❤❤❤❤❤💙💙💙💙💙💙💙💙
un vrais représentant de la fayda tidianya. Kou joubb ,kou yarou , kou beuri xam-xam
Vraiment
Walye ndeye sane baye niass rék 💖💝❤
Machallah BAYE TOUT BAYE sa émission bi rafet'neuh trooooppp waay.
Liii rk doyneu niou guëstu mbirou BAYE NIASS...ndax limou diangalé ci Dîné dji ak Tarikha Tijaan bi warna nitt nieupp nieuw dioko ak BAYE NIASS ndax njeurign leu rk ci jaam gni.
Wayé nak aussi MAWLANA SANGUE ABÛBAKRIN BARHÂMU NDIAYE mii yarr TOUT BAYE mii di wax Sénégal warnagn ko degglou dh pour xam limouy wax
Merci frère bien dit degloul rekk
L
macha allah tout baye wax nga deug chekh tidiane khadioul ci plateau wallahi
Amiiine ya Raby wallahi Macha'Allah 🥰🙏
Macha'Allah Tout Baye Kham-kham bi bari na Macha'Allah, Yallah na Yallah barkél !
Mais félicitations Oustaze Maodo, très bien dit, il faut parler aux gens à leurs niveaux car tout ne se divulgue pas !
Merci bien !
Dieureudieufééé Baye !!!!
⁶8
Jërëjëf Toubaye. Maacha Allah
JËRËJËFËTI SANGUE Barham N'DIAYE
JËRËJËFËTI Tout Baye Niang
Ohh temps bi dieudieuf tout baye ohh gayi fok niou kham kane moy baye niass
ماشاء الله أحباب الشيخ الحاج ابراهيم نياس رضي الله عنه وطلب مربيا خبيرا ناصحاً كامل عرفان اماما صالحاً
Touuuuuuuuuuuuuuuuuuuuuutbayeeeeeeeeeeee❤❤
Machala baye niass rafetna hamme yalla rec Moy hetili diambi
Machalla toubaye,dieureudieuf sbn
Goor Yalla bou dégg Yalla brkp baye akh bayamm. Yallana baye nangoul niou sounou Talibè
Toubaye masallh
Dieureudieufé baye Niass 🙏🥰
Machalla je suis fier d'être sbn ❤👌
Toutbaye Niang le digne représentant de la fayda assurance lakko toudeeee
Mâchât Allah Tout Baye dila nianal fan you goudou ak weer
Li lagn begoon si quartier grl di wax si baye si zahir ak si baatiin long vi tout baye
Maodo baye douham hall moukou hanrifla pure
Ooohhhhh temps bi?
Machalah mouqadam tu es notre fierté dieureudieufééee ndiaye
Machalla tou baye gor deugu gua
Machallah fassah na trop ❤
Wolahi douma doyal thi deglou émission bi. YALLA cheikh Ibrahima fayalnagnou la tout Baay. Sangu bi Ndiaye gueureumnala
Allahou Akbar Diarediefééééééééééééééé Baye Sangue Ndiayeeeeeeeeeeeeeee
Maodo déh mo ngi nane moutassawif yoyou nonou ndeysan pour mom oustaz ordinaire la inviter
Machallah thiey sangue barhamou ndiaye djeureudjeuf tout baye DEUG rek nga wakh
Dieureudieufé Sangue Abubacrine Barhamou Ndiaye
Allahou akbar . Tout Baye contane nagn walahi tmp bi waronna beurry
Rafet na bay mashallah!
Machalla Tout Baye dieureudieuf Baye Niass pôle du temps
*Thiouuuuuum Tout baye ❤️*
Tou baye machalla
Sangue Ndiaye sa ligeye rafetna
Wallahy
Machallah
Walahi
Machallah tout Baye mala beugue
Touuuutt baye
Macha allah dieurdieufeeeeeee Baye
Machallah tout baye
Touuuuuuttt Bayyyyye ❤️gooorrrr nga Baye🌹
Masha Allah alhamdoulilah dieureudieuf baye naisse
Félicitation tout baye yallana baye gueueum
Tout baay ko a goorko sukran laka
Thieye baye
Machala Serigne bi beigue naniou ci yaw
Machallah TouT Baye
Khol sédeu na torop. Tout baye gaur deugueu nga , Sbn REK !
Merci pour l'émission . Lep ler na.
Diadieuf sangou barhama
Alhamdoulilah dieureudieuf tout baye lerna
Walahi bay rafét na torop bilay nak
Machallh rafetna baye
Jaarama Baye Niass. Tout est Baye way
Macha Allah !
Tout baye yaye gour lep s b n
Machallah
Machallah jajeuf
thieuy tout ndeysann nite kou baxnga
tei xamnanii bounioula mayone 24h taxoul nga diexal
goor nga baye
Merci tout baye niang
Machallha baye toubaye
Tou baye gorga masallah
Jërëjëf baye kontane nagn trooopppp
Limouwakh sokone lakhèwè wone fofa elhdji amadou deme mofanèkone
شكرا جزيلا توباي
Mchallah
Machallah tout baye gorgua
Masachla
الحمدلله رب العالمين الحمدلله رب العالمين ماشاء الله وارض شيخك ولوأبكاكا لكنه للخير قدهداكا
machallah jeurejeff baye
Alhamdou'lilah
Machala barakalahou fikoum
Dieureudieuf sbn
Manchallah
me tan bi dafa touti trop way
Diadieuf Baye Tout contanagn
Tout baye machallah
Macha alla nékh na
Macha'Allah amena solo
Oh le tps est très petit
Dondno tout bay
Walahi toubayye goor la
Boul wér boutou cheikh tidiane
ALHAMDOULILLAH SBN
DEUG DEUG kham kham ak kheum kheum dou bene
Mérci tou baye
Tout sanga
Allahou akbar
Hooo heure bi dafa gata no leer na baye
Machallah alhamdoulila
Tout baye diereuf way li laniu soxla
me kahm kahm bi rafetna way
thiouum
masalah