Divorce de mbathio ndiaye: Dabaye proche de baye niasse piétine mbathio et explique la vraie raison

Поділитися
Вставка
  • Опубліковано 2 гру 2024

КОМЕНТАРІ • 936

  • @talibemouride5810
    @talibemouride5810 2 роки тому +264

    J’espère ceci sera une bonne leçon pour les filles. Arreter les amities et soyez plus discrètes. Soutoura diekh na si mim rew

    • @mberryable
      @mberryable 2 роки тому +9

      Talibé Mouride wallahi mom la don wakh kou nek nguan and ak mom nguan wakh ko say wakh ni rek wallahi tallahi .

    • @khadim1875
      @khadim1875 2 роки тому +18

      Les filles entre elles daniouye lékanté comme aye deum

    • @mberryable
      @mberryable 2 роки тому +7

      @@khadim1875 wallahi degueleu gnoune rek

    • @bobolatifadiakhate8103
      @bobolatifadiakhate8103 2 роки тому +7

      Djiguéne dale amatoule valeur thieye li

    • @aidafallousall6793
      @aidafallousall6793 2 роки тому +2

      Omoro talibè Serigne Saliou/Cheikh Bèthio kouko beuga torokhol yalla torokhol la.

  • @dubeilaurentiu6543
    @dubeilaurentiu6543 2 роки тому +68

    Merci beaucoup dabaye kou bakh gua mane khamnala bou bakh😘❤️

  • @BlackPanthere158
    @BlackPanthere158 2 роки тому +87

    Ay Baye Niass yalna nga am sokhna sou geune si yaw

  • @charlydaniz1379
    @charlydaniz1379 2 роки тому +275

    Il me semble que cet homme est entièrement responsable de ce qui lui ai arrivé. Comment peut-il épouser Mbathio, sachant que cette femme n'aime que les sortie en boite et lui demander de ne plus sortir? Aussi, comment peut-il fermer les yeux sur tout ce qui est écrit, dit et filmé sur Mbathio Ndiaye? Il est vrai que la danse est une belle femme, une des plus belle et charmante de notre pays. Toutefois, faut-il épouser une femme parce qu'elle est jolie, attirante ou faut-il mettre en avant d'autres qualités? Du temps de nos grands parents, c'étaient le comportement, le "Djikko" qui étaient mis en avant ou déterminant dans le choix d'une femme. Hélas, tel n'est plus le cas. Mbathio n'arrêtera jamais les boîtes de nuit. A bon entendeur salut

  • @niomibatv2047
    @niomibatv2047 2 роки тому +146

    Les mariages sur les reseaux sociaux vont finir tous sur les reseaux sociaux.

  • @zeinabsenegal1501
    @zeinabsenegal1501 2 роки тому +156

    Mbathio il n'est jamais trop tard il faut changer aduna amoul solo

    • @sowpoulo6049
      @sowpoulo6049 2 роки тому +1

      Hummm mbathio dou khalè deh bakhna

    • @vitolesenegalais6540
      @vitolesenegalais6540 2 роки тому +2

      Djiko AK boromam jusqu'à la mort rekk.
      Djiko Moy nitt.mbathio dou meusa changé.

    • @gjhj1129
      @gjhj1129 2 роки тому

      Surtout lolou boye sey dagua khame ni dagua sey

    • @khadim1875
      @khadim1875 2 роки тому +2

      Pour yéne mbathio 20 ans la ame !
      Wadji na dème taki khalei , kou regler correct, mais mére yi takhawalou si boîte yi ba perdal nga léne di tak ! beug lou bone ba déh

    • @fatoumatasow4244
      @fatoumatasow4244 2 роки тому

      @@vitolesenegalais6540 wakhatiko d djiko ak borom pakh

  • @djatoudiawara1075
    @djatoudiawara1075 2 роки тому +97

    Que Dieu ramène la paix dans ce couple Amine

  • @mamegueye1744
    @mamegueye1744 2 роки тому +46

    MRC Magou Diambour Dabaye yow kou roye si yow Seye ndakh seykat ngua mais Mbathio badola bilahi

  • @nndeyekhouryndiaye7137
    @nndeyekhouryndiaye7137 2 роки тому +48

    Nonnnnn Dabay mi la beugue yow Lo wakhhh deugue man Lo wahh ma gueum ndahh danga deugou yow si foula ak si fayda rekk ngayy dohhh mann dama la nawlo tu as très bien fait de leral chapeau à toi 👏🏾👏🏾👏🏾👏🏾

  • @djibrildiaw2131
    @djibrildiaw2131 2 роки тому +147

    Mbathio sam sa Lou geuneu cher si réseau sociaux yi goor gneuw sagal la si kanamou Sénégal yeup yoww nga gneuw trahir KO ya booonnn mbathio 😭😭

  • @user-of3bg1zc9p
    @user-of3bg1zc9p 2 роки тому +18

    Vrmmt j ai bcp d instime pour cet dame bilaye vraiment doundeul baga féké s'en gnirignnn dommm bilaye référence gaaaaaa tu es une bonnn personnes Mala Tipo🥰🥰🥰🥰🥰

  • @deuguerek5006
    @deuguerek5006 2 роки тому +73

    Yaw Dabaye Lo wakh ma gueum co parce que danga nakari dérèt té beugo coula yap , tu es véridique mashallah

  • @salioukebe848
    @salioukebe848 2 роки тому +47

    Sénégal ya beaucoup de mbathio Ndiaye d'où nieup nak Waya am dieukeur am far tandance la thi mime réw yalnanou yalla mousseul thi djigéne goubone

    • @princessekounta2538
      @princessekounta2538 2 роки тому +2

      Tu parfaitement raison

    • @ndeyeamydeme1851
      @ndeyeamydeme1851 2 роки тому +2

      Pour une pays musulmane souniou loi lénn warona appliqué thi deukk bi ndakh c'est une pays musulmane kou ndialo niou tékk la châtiment bimou ladie

    • @mariemamamathiam8077
      @mariemamamathiam8077 2 роки тому +1

      Dégue na ni sounou yonét bou tédebi dafa ame saba bou wakh né ko jiguén bi dafay ndialo mouné kou si ték buetem kéne wakhoul mouné léne nite sounou wakhé dafay ndialo na ame 3sédé yo kham ni kéne bokoul ak sa borom fimou dege sodé dege la islam moye até wa bala nouy wakh di khas mbathio na nou léne ko yéde mo guen khass kéne khamoul kou wakh dege yalla rék mo kham

    • @mariemamamathiam8077
      @mariemamamathiam8077 2 роки тому

      Dégue na ni sounou yonét bou tédebi dafa ame saba ba youné ko jiguén bi dafay ndialo mouné kou si ték buetem kéne wakhoul mouné léne nite sounou wakhé dafay ndialo na ame 3sédé yo kham ni kéne bokoul ak sa borom fimou dege sodé dege la islam moye até wa bala nouy wakh di khas mbathio na nou léne ko yéde mo guen khass kéne khamoul kou wakh dege yalla rék mo kham

    • @mariemamamathiam8077
      @mariemamamathiam8077 2 роки тому

      Dégue na ni sounou yonét bou tédebi dafa ame saba ba youné ko jiguén bi dafay ndialo mouné kou si ték buetem kéne wakhoul mouné léne nite sounou wakhé dafay ndialo na ame 3sédé yo kham ni kéne bokoul ak sa borom fimou dege sodé dege la islam moye até wa bala nouy wakh di khas mbathio na nou léne ko yéde mo guen khass kéne khamoul kou wakh dege yalla rék mo kham

  • @aminataniang2948
    @aminataniang2948 2 роки тому +62

    Mbathio kou badola gua dabaye am gua fayeda mame mbaye sakh da thiofe machallah💔

    • @abdoudiop5163
      @abdoudiop5163 2 роки тому +1

      🤣🤣🤣🤣🤣🤣

    • @khadijachou5510
      @khadijachou5510 2 роки тому +1

      😂😂🤣🤣🤣🤣🤣🤣

    • @beautenayo1031
      @beautenayo1031 2 роки тому +3

      Gor bou bakhe la dina am diabar diou bakhe inchala keur goumou feug mou oubékou si tout ces propos sont vrais elle ma déçu

    • @moriciss6368
      @moriciss6368 2 роки тому

      Billahi dafa thiofé mane amna deuikeur wayé seuy tes yalla takhe mon diafé

  • @tabaraseye3689
    @tabaraseye3689 2 роки тому +47

    Leina D khamnako mbathio chance dieukeur bigua amone gueumouma ni diguako amatt D YALLA naleu YALLA tek si yoneu

    • @khadidiatoundiaye3609
      @khadidiatoundiaye3609 2 роки тому +1

      Doukoo amatt dh lolou dafa leirr chance bi😢😢

    • @abdelohod4884
      @abdelohod4884 2 роки тому +5

      Fanne lakoy amatai wayyow khana vampire mokoy Takk kikay c fini

    • @Bienfaitislamique
      @Bienfaitislamique 2 роки тому

      Ah Mbathio neikhoul bagn dh ,mane candidat la thi prochain election takk Mbathio.

    • @khadidiatoundiaye3609
      @khadidiatoundiaye3609 2 роки тому +1

      @@Bienfaitislamique iow vampire geu khana

  • @princessekounta2538
    @princessekounta2538 2 роки тому +70

    Vraiment mbathio ak foume diare warona seuye ba déh dou nitt

    • @diallofatoumata2677
      @diallofatoumata2677 2 роки тому +3

      Linga wakh nii motah bimako degué guemoumako pour mane Mbathio Dina fa diour beu keurgui fesses baparé seye fa ba dé.... pour mane 2099 lay tasse

    • @princessekounta2538
      @princessekounta2538 2 роки тому +2

      @@diallofatoumata2677 walay ndeysane nieuppa la béte yalla nako Yalla sopi

    • @diallofatoumata2677
      @diallofatoumata2677 2 роки тому

      @@princessekounta2538 Amine yarabi ya Allah

    • @faramarendiouf6831
      @faramarendiouf6831 2 роки тому

      Bilahy yaw

  • @mamediarrafall9049
    @mamediarrafall9049 2 роки тому +83

    Sheute mbathio wayadina ki kouko degu khamné Li mouy wax dako leer thieuy seuy len te yalla takh mbathio khalatal sa euleuk adouna diezna bapare gni meuna kott nak amouniou mbam dal

  • @adamasow5010
    @adamasow5010 2 роки тому +32

    Mbathio thiaga, d'abbaye xolou diamond merci beaucoup

  • @kinethioune6450
    @kinethioune6450 2 роки тому +66

    Ki dagn ko yakk😭😭tayouko bale lene ko yene li motakh djiguene sougn koy wakh tamal tokk li mo takhone mai boite chak jour nelaw tte la journée agne 22h préparation 2h du matin nekk almadie ba fadiar dolene togu dolene rakhass motakh kousi ame dieukeur wayadi doto meuna tokk dem rek guay gnew mbathio nakk roussal djiguene gua🤨

    • @ndeyely3362
      @ndeyely3362 2 роки тому +1

      Bilan wah nga deug sou moytowoul lamign

    • @khadijandiaye4902
      @khadijandiaye4902 2 роки тому +6

      Waw kayyy nakkk tu as raison outé ak mane migua khammmm niii tout le travail de la maison c’est moi qui le fait chaque jours et pourtant on’ as une bonne et le femme de mon cousin est là mh c’est moi le fait de plus avc l’école c’est difficile dehhhh mhhh magui mougnie dehhh sante yalhhh bou bakh Mais les filles d’aujourd’hui choco chocolouuu reck akkk buzzzz waaa bakhenaaaa reck allons reck😔

    • @diatousow6205
      @diatousow6205 2 роки тому +2

      @@khadijandiaye4902 doko rethiou bo seuyi rek contane bily courage

    • @khadijandiaye4902
      @khadijandiaye4902 2 роки тому

      @@diatousow6205 d’accord chérie tkt

  • @awasamb660
    @awasamb660 2 роки тому +11

    Mbathio dè dotoul ame dieukeur si Senegal 🇸🇳
    Yalnanou yalla mousseul si djiguène bou bone nangouwoul changé da nga yakar adouna keur la nakh nga sa bop ,appartement auto bou béss yeuré you raféte lépeu fi ngakoy bayi

    • @fatydias
      @fatydias 2 роки тому

      Wala Jay kikay tak mom mokoy financer pour moi tak ko

  • @bourewalo1697
    @bourewalo1697 2 роки тому +51

    MERCI Tu A Tout Dit

  • @adamlailler8495
    @adamlailler8495 2 роки тому +275

    Seye bi douma thi wakh dara léroumathi !
    Wayè Badola Mbathio Ndiaye ake meneu wore lo thi wakh bayi nga lou dèsse, gno boke village koungheul, di gnouye sougnou keur goudi ak bethieuke,
    Wayè bamou gneuwé Dakar khamètoule kène. Wayè amoule diome, mou dègue sama rirou Mariage mounè dafa wayansi falèwouma dakh dièpiko, loulou doyou ko dèè
    Ma seyi France, mou woma nèma dama gnewe France tè damala beugue sètesi ndakh sa mariage mayoma mani doumouko recevoir sama yaye nèma bayiko mou gnewe yèna boke sène koungheul🥲 ma bolè louma nèkh ake louma nakari recevoir Mbathio Ndiaye ak copineume sama keur ma invitè lène dîner bou ame diome ba tale samaye bougie, mouye dème nèma ndakh meune na yobou gamele thi dèsitou rère bi, ma diokh ko maye ko aye yerè you besse takh ake sène étiquette boulèthi mayko khalisse ma tale sama auto yoboulène bathia gare ba kéroke la gueudieu dègue Mbathio Ndiaye ! 🏃‍♀️
    Ki kouye badola mome ngaye diapalè...

  • @laminediop8520
    @laminediop8520 2 роки тому +31

    Le problème des hommes connu au Sénégal aujourd’hui veulent marié que des femmes connu au final voilà le résultat tout temps cherché la beauté oublié pas la beauté est éphémère les frères cherche des vrais femme avc un grand cœur

  • @aicha3515
    @aicha3515 2 роки тому +38

    Wahouma lolu dh sourirou dieukeurou mbathio bi lanla ooh😭♥️

    • @lil_mermaid0602
      @lil_mermaid0602 2 роки тому +2

      😂🤣🤣🤣🤣 rafet n'a dal

    • @aicha3515
      @aicha3515 2 роки тому +5

      @@lil_mermaid0602 dina am kou mel ni di thiahane anh😭😭😭mbathio nelaw na

    • @KawsaraImage
      @KawsaraImage 2 роки тому +3

      Mbathio kayy dmrme laa

    • @marcelfernandez100
      @marcelfernandez100 2 роки тому +6

      Boul ni Djieukeur neile ex dieukeur 😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂

    • @abybandiaye9112
      @abybandiaye9112 2 роки тому +1

      Wa khana

  • @pmnd2811
    @pmnd2811 2 роки тому +41

    Mbathio ndiaye vraiment bèt ngama .
    Nga def lounè fang!! Adouna bi yeup guiss ko , yallah mayla goor bou gentle bakh et tout ngay dèm di thiagatou dji à gauche à droite baniou fassèleu.
    Yay domeram deug deug.
    Badola nga en plus beug nga lou bone

  • @astoumbeneniang7827
    @astoumbeneniang7827 2 роки тому +37

    Dabay chérie Armand yayou mouhammed bilay walay yangui niouy seuyeul

  • @abdouthiam6899
    @abdouthiam6899 2 роки тому +53

    Defo dra mbathio deful dra kou goor ki mo yap ay mbokam. Say dom danga lendi tanal yay diou bakh mais yambar gnulay manipulé kom ça. Goor day am foula am dignité khol djiguén bu am dignité ak respect.

  • @KawsaraImage
    @KawsaraImage 2 роки тому +21

    Bilae da nga Bakh rkk deff lepp lo varone deff machaallah

  • @hannah3442
    @hannah3442 2 роки тому +44

    Ça fait grave flipper les potes sénégalaises...
    Heureusement ya des gens cleans

    • @diamansaly1274
      @diamansaly1274 2 роки тому +1

      Vraiment s'est pour ça que j'en ai pas 😅

    • @hannah3442
      @hannah3442 2 роки тому +1

      @@diamansaly1274 Ouf😰 sauvée

  • @maremedieng2477
    @maremedieng2477 2 роки тому +107

    Thiayy Mbatio t'es une femme très sombre change il n'est jamais trop tard

  • @LAKWATER_STAMINA
    @LAKWATER_STAMINA 2 роки тому +30

    Ohh c’est triste j’ai plus de mots je ne juge personne mais là dame ne devrait pas dit ça la vie n’est rien seul dieu peut nous juger

  • @dalyndiaye2036
    @dalyndiaye2036 2 роки тому +67

    Non Dabaye ya yatou khole koula yobou police niari yone nguaye ande ak mome aàhh Dabaye ki est tiii🤦🏽‍♀️🤦🏽‍♀️🤦🏽‍♀️🤷🤷🤷

    • @aminataba9331
      @aminataba9331 2 роки тому +1

      Momadikhal mé dou peul mé si yoroyi

  • @khadijagueye3517
    @khadijagueye3517 2 роки тому +59

    Ma chérie diaroul won sah expliquer Manon gua bayi l'EPO si soutoura ndah euleuk d'où Agne dou rerre

  • @fatouniang4540
    @fatouniang4540 2 роки тому +8

    Machalla dabaye ya bakh sa coll mo rafe❤💖💫

  • @assyaka7916
    @assyaka7916 2 роки тому +19

    Bilakhi Dabaye ya bakh rék Mbathio mo Doméramé rék

  • @ladiva2202
    @ladiva2202 2 роки тому +56

    Wa mane sénegal laniou nék mbathio kone ndokhe dou bayi yonam🤔🤔🤔🤔

  • @blackqueenlasagesse4037
    @blackqueenlasagesse4037 2 роки тому +14

    BAYE NIASS ....
    Kaay takk ma sa mbook talibé la té dinala seuyal ...si barki Baye Barham... sama deug la nek nakk❤🙏

  • @Rassoul__Moustapha07
    @Rassoul__Moustapha07 2 роки тому +33

    C'est'une bonne Leçon pour les filles Arrêter les fraicantation Amitié les Amis aujourd'hui Dafa rare ,li môme Sénégal soutoura Amatoul si réw mi 😢 Nitte boko xamalé Lou niãw sakh soutoural ko Yalla Bëugg Soutoural domou Adama Mõ takh mou sakk Goudi AK Beuthieuk.

    • @maimounadiallo8888
      @maimounadiallo8888 2 роки тому

      Wallah c vrai ❤ نسأل الله العفو والعافية في الدنيا و آخرة🤲

    • @binetaniane8870
      @binetaniane8870 2 роки тому

      Vraiment 0 classe

    • @dykha8182
      @dykha8182 2 роки тому

      Mbathio moo fi xaawi woone soutoureu Omaro ndakh sommou xaalis bou niak fayda

    • @leuzleuz8602
      @leuzleuz8602 2 роки тому +1

      Fréquentation

  • @diadia965
    @diadia965 2 роки тому +27

    Dabaye barké serigne babacar sy damala begue nittou degueleu se numéro rék la sokhela

  • @awadiop149
    @awadiop149 2 роки тому +20

    Senegal dee Mbatio MO fi geuneu niakh diom li ko fi dall lepeu yalla may ko dieukeur bou ko terale mou nes dou changer moukh

  • @seynandiaye222
    @seynandiaye222 2 роки тому +23

    Boy fith mith banlieue amena ay noble Dabay Nice n'a trop...

  • @lallazeinabtidjani3154
    @lallazeinabtidjani3154 2 роки тому +31

    Bien dit ma chérie sa ma kharite bi ma la fan

  • @RamaHealthBeauty
    @RamaHealthBeauty 2 роки тому +60

    Mais yaw tamite dé bakho, werr sa moromou djiguène yii , sortant tous ses secrets. On dirait plus un reglement de compte/vengeance ou genre "bien fait pour toi"

    • @veriteabsoluedeugneekhoul1720
      @veriteabsoluedeugneekhoul1720 2 роки тому +11

      Wayé setane ko khol fimouy moudiè. Dagnouy andeu ak niit teu dougnko yènè diam. Beugou gnou loudoul defaitam. Mais andeu thiagua mo deme nonou dagnou lekanté sen biir

    • @bulldozer3131
      @bulldozer3131 2 роки тому +8

      Elle est aussi mauvaise que mbathio ....c'est une bande de kooba

    • @lilihouse5417
      @lilihouse5417 2 роки тому

      Bilayy

  • @fatoubakhayokho5672
    @fatoubakhayokho5672 2 роки тому +6

    Merci vous avez tt dis am guathi part d responsabilité mais Mame baye aussi dou khalei il savait c qu'il fesè. Yalla nako bourbi may djiabar djiou gueun thi mom nako seuy tok diko mougnial aussi

  • @bourewalo1697
    @bourewalo1697 2 роки тому +40

    MBATHIO Mère LA MAGUETA LA Elle Va LE Regrettée

  • @khadysall6745
    @khadysall6745 2 роки тому +34

    Mbathio damay ragalni kham na fi ngay lambati doto amati dieukeur deff ngafii louné say video guéne goor gou bakh fate lolou yeupeu tak la teral nga khew khew mou reuy lou adouna bi niepou di diow kone worolga tok seuy

  • @ndeyefatoudiouf6060
    @ndeyefatoudiouf6060 2 роки тому +37

    Mbathio tu m’as déçu enh dinou ték gathié rek

  • @anitambaye859
    @anitambaye859 2 роки тому +61

    Genre mane sama yoneu nékousi mai yénne khana amoulenn occupation depuis bobou batay Divorce Mbathio Ndiaye rék guay guiss si UA-cam bii non mais c’est quoi votre problèmes ?? lousii sougnou yonneu si divorce Mbathio ak famille djeukeuram kou beugueu Cas rékk bo caswé sa bopeu khamni Mbathio tané wouleu mane je prends pas sa défense dh dakh lidjanti wouma sakh kouyy Mbathio Ndiaye deuk bii soxleu neu lénénn loudoul lidjanti Vie wou Djabour wala bokk aller dans les hôpitaux interviewé madales yigua khamnii gniguii dée nakh amougnou lougnou fadjo gnoulenn meuna aider aidé lenn les sans abris nakk vraiment mon pays va male temps biguénn di yakh si nitt di douguou lousenn yoneu nékoul yénneu pays yii gnonne gniguii khol nousenn réw gueuna évolué

    • @vitolesenegalais6540
      @vitolesenegalais6540 2 роки тому +1

      Siiw dou diami borom,mbathio moo indi problèmam depuis le début ci net bii ,kon boulen nio sonal,kou beugoul sa vie privée nioukoy lamlame ci net bi da ngay soutoural sa bop,am sa jardin secret,mais loy def neko bath ci net bi ,motakhit ,niit ngi ken momoulen.

    • @MimiMimi-vm5oe
      @MimiMimi-vm5oe 2 роки тому +7

      Bouthi sa yone nékoul loy cliquer sétane bay commentaire bi commentaire bou goude isshh

    • @deugheulaveritemoufin4731
      @deugheulaveritemoufin4731 2 роки тому

      Waaw yow nak🤣🤣🤣

  • @josephinesy2262
    @josephinesy2262 2 роки тому +16

    Bilayi magui dioye sakh kou deugou gua je ne vous connais pas toute les deux mais toi kan tu parle on sens ke tu es véridique merçi bcp de courage

    • @papediop9404
      @papediop9404 2 роки тому

      Lii amoul place si net bii,qui dof la

  • @rokhayagueye8635
    @rokhayagueye8635 2 роки тому +29

    Masta tu as parfaitement raison boule oute kharite

  • @isafaal801
    @isafaal801 2 роки тому +10

    Bay niasse mo yapp yayam no meune takk mbathio.

  • @mameawacisse9537
    @mameawacisse9537 Рік тому

    Bilahi yay boy seyel ba mou nékh lo loy dege ❤❤❤

  • @marcelfernandez100
    @marcelfernandez100 2 роки тому +50

    Non Dabaye YAYE Bandit ligako deiii si nopam bi moma neikh 😅😅😂😂

  • @pedroanderson6351
    @pedroanderson6351 2 роки тому +26

    BAYYI LENNE MBATHIO DEFOULLE DARA
    WAJI KA FEKKEU CI MONDE MBATHIO MO KO TOGNE
    IL Y A DES FEMMES QU ON NE DOIT PAS EPOUSER

  • @oulimatasarr4752
    @oulimatasarr4752 2 роки тому +50

    Bilahi dabay ya deugou wayee

  • @mariemendao4594
    @mariemendao4594 2 роки тому +16

    Senegalais dal mo rékh rék tédou yénafi done jouer à l'avocat du diable nane Mbathio erreur la déf patati patata. Cette garce same ay tatam plusieurs fois si mbédemi nguén nane erreur la pfff. Mame Baye tu t'attendais à quoi? Soxna dagnoukoy tane santal Yalla binguassi amoulé djabott.

  • @mamediarrasaliou5269
    @mamediarrasaliou5269 2 роки тому +5

    Je sens un grain de méchanceté

  • @papadiop6508
    @papadiop6508 2 роки тому +43

    Y a pas amitié entre fille. Djigueine yi yéwoulén

  • @fonsecafonseca3769
    @fonsecafonseca3769 2 роки тому +23

    Moi franchement je ne connais pa mbathio mais je ne la sens pas si je la vois a la tele je me dit qui elle na pas un bon font yalla nama yalla bale mais sou feker liniou wakh moko def dara rafetousi

  • @naboufaye4918
    @naboufaye4918 2 роки тому +8

    Je t'aime beaucoup ma chérie yalla nasa diam yague

  • @khadydiop8274
    @khadydiop8274 2 роки тому +32

    La parole est malaisèe et dangereuse mais helas le silence n est nefaste choisissez vos amies mes tres cheres

  • @abdourahmanesall8460
    @abdourahmanesall8460 2 роки тому +3

    Fi Sénégal Wally seck rek mofi goré le chanteur du peuple

  • @maguettekane8485
    @maguettekane8485 2 роки тому +15

    Dabaye dama la fan tu a parfaite ma raison

  • @lemagicien1933
    @lemagicien1933 2 роки тому +4

    Ya aussi de la jalousie chez cette dame à la 21 mn 25 s , elle dit di tall sa télé di snap mani paat nopi . Donc mbathio dafa mauvaise mais mom oci maynako le gars ba paré di sissou et loulo nak dafa Bari si rewmi

  • @mounasseseck5893
    @mounasseseck5893 2 роки тому +81

    Mbathio yay badola ya bone yow diaro kham sah

    • @KawsaraImage
      @KawsaraImage 2 роки тому +5

      Vraiment kii kayy dmrme laa

    • @oulimatandione3037
      @oulimatandione3037 2 роки тому +3

      Ah mais aussi mome fii lafii filmer bopam awra.je me dis tognoul kene deh.mane j'aime pas juger mais cette fille massoumako degal lou bakh nama Yalla bal

    • @deugdouroumbnop1434
      @deugdouroumbnop1434 2 роки тому +2

      Domeram leu rek

    • @khadijandiaye4902
      @khadijandiaye4902 2 роки тому

      Bilakhiiii yako lalll

    • @ndeyeramandiaye3359
      @ndeyeramandiaye3359 2 роки тому

      Ndeye Gueye danseuse reekk moko kham.

  • @ndeyefatousoumare8273
    @ndeyefatousoumare8273 2 роки тому +11

    Bilay Dabaye kou bakh ga ndakh yaw môme sa khôl mola sonal mais yalla bakhna boul wakh dara la vérité finira toujours par triompher ma chérie sama belle sœur rou jumelle

  • @bulldozer3131
    @bulldozer3131 2 роки тому +67

    Cette fille qui parle et mbathio sont les mêmee ...elle parle de fatou Mbacké la fille qui a ete enceinté par eumeudi Badiane ....donc meme groupe kiff kiff...c'est juste une associations de KOOBA PROFESSIONNEL qui ont des problemes internes....cette femme est aussi mauvaise que Mbathio...Senn genre yii mo takh goor niou beurri da niouye regal takeu diabar thiakhanne rek ak weerenté gueen fi neeke....boon gueen toorop doo leen exemple

    • @Sunshine1_1
      @Sunshine1_1 2 роки тому +6

      Kooba professionelles🤣🤣😂...thiey lii.

    • @teestreeter4628
      @teestreeter4628 2 роки тому +2

      BULLDOZER bilay deugg ga wah niom nieuppa yam dh nio bok crew ay koba laniou. Andouniou sah ak ay nitt you bakh mom mi di wah ay pape mbaye gordjiguen nak kounei moleni may haliss wayane rk thiogou rk ak thiagatou bouniou keneu solan

    • @ZeynabRassoul1
      @ZeynabRassoul1 2 роки тому +2

      Kooba professionnelle 😅😅😅

    • @mberrymmy9275
      @mberrymmy9275 2 роки тому +2

      Bulldozer ce qui est dèplorable moy khalèyi lèn di top.fou rèwmi dieum ak gni mèlni gni. Diom dièkhna ndakh rèseaux sociaux yi c’est déplorable.

    • @MimiMimi-vm5oe
      @MimiMimi-vm5oe 2 роки тому +2

      Peut être niom nieupp ame défaut wayé Mbathio mom Kene yamoul ak mom limou fii deff kéne deffoukofi

  • @aichapene3182
    @aichapene3182 2 роки тому +2

    Louko fi diare wer samorom Lou way def boppam lidou amitié

  • @serignegueye9544
    @serignegueye9544 2 роки тому +35

    No dioumo dé mbathio da la liguéy pour ma na diot si Mame baye kon diaroul ngay léral défo dara mbathio moy djiguéneu bou bone

  • @lifestylelifestyle8188
    @lifestylelifestyle8188 2 роки тому +1

    Sokhena cas bii pause bañiou dieule Cup d'afrique bii nga dèlou sii wate stp mbathio boul tontou diape rèkk ba Cup d'afrique dièkhh stp merci

  • @adjasene3565
    @adjasene3565 2 роки тому +6

    Comme le disait ma mère que la terre lui soit légère
    Les femmes belles ne connaissent jamais leurs valeurs actuellement Buzz mo sonale gnou barri

    • @laminediop8520
      @laminediop8520 2 роки тому

      Que ta maman repose en paix sista bilay elle a raison ta mère beaucoup d’homme oublie que la beauté est éphémère on marie pas la beauté

  • @onlygood1114
    @onlygood1114 2 роки тому +14

    Mbatio a manipuler son ex mari diakhasé KO AK ay nitam am dieukeur am far

    • @kinebarry7742
      @kinebarry7742 2 роки тому +2

      Merci si résumé bi😂😂

    • @onlygood1114
      @onlygood1114 2 роки тому +1

      @@kinebarry7742 ma chérie cas bi nila démé😂😂😂😂😂

  • @mathos24
    @mathos24 2 роки тому +7

    18:54 Armand Bayil dokhane tamit...Sa Diabar xamena lép.Fais attention frère !

  • @jdjdbbdbbjdjdb5380
    @jdjdbbdbbjdjdb5380 2 роки тому +11

    VRAIMENT j'ai pitié de MAME BAYE NIASS

  • @soyyo6378
    @soyyo6378 2 роки тому +40

    Dioumo dé yaw tamit nitou intéré nga
    Kham li wadji yoor ak limoulay défal mo takh nga boléko ak sa copine mbathio pour ngué lekk ko. Gnari cobas gnoy andeu.

  • @maxlalionne8146
    @maxlalionne8146 2 роки тому +20

    Dabaye chérie arma Ndiaye wakh nga deugue beussou wakh bou diotté kou wakhoul ndo goor mbathio bakhoul ay takou souf teksii warone nga took seye sii té yalla rek takhh ndo nittou darra changel femme nga lolou mo ngeun

  • @khadijatoubarro8621
    @khadijatoubarro8621 2 роки тому +7

    Mame baye je peux vous donner ma petite sœur ramatoulaye

  • @lintouchablerene7972
    @lintouchablerene7972 2 роки тому +12

    Li dhé la doundou ak sama copine en plus légui sama gor sakh khamatoulni mangui doundou motakh deflenn ndank si kharite yi té bania wolou kéneu des fois nit dina kharito ak yaw par intérêt
    Courage ma belle nitt kou bakhnga té deugou machalah

    • @binetacamara9795
      @binetacamara9795 2 роки тому +2

      Deugeuleu

    • @ffs7322
      @ffs7322 2 роки тому +5

      Bilahii khamna thii dara sama meilleure copine mariage 2 jour avant lamako wakh et pourtant lepp makko diapale ba bamouy dem di défaite ndawam ak yakk birr lepp . Mais damako baye akk yallah dikko nianal seuy bou varie rek

    • @lintouchablerene7972
      @lintouchablerene7972 2 роки тому

      @@ffs7322 non mais purè ki nitt la mais togal di sétann yalla Dina atté man dhé ki 2jrs avant son mariage la teudeu ak sama ex ba paré woté labann mais lou way def bopam man damalenn moudié paquatté dewma si mariage bi dewma si labann bi ni baptême bi ndakh jsui pas hypocrite
      Mais courage ma chérie dinako guis dhé inchallah yénél nieupp diamu rek le reste nga bayiko si lokho yalla

    • @aissatoudiallo5162
      @aissatoudiallo5162 2 роки тому +2

      @@ffs7322 thiey yalla mane ma warou si haritou legui yi motah mane magui diap sama ndiambour haritowouma ake kéne Kou gneuw ma sek ake yaw diam et la vie continue

    • @aissatoudiallo5162
      @aissatoudiallo5162 2 роки тому +1

      @@lintouchablerene7972 fi migui wathie wa li ame na doy na war

  • @abdoudiop5163
    @abdoudiop5163 2 роки тому +9

    Kou gore ki ausi defna heureure kham nite mercoledi tak ko dimanche pour lane surtou ko khamoul mbthio ndiaye ya badola ngay mere am plus de 40ans ame dieukeur di takhawalou si soire yi badola kharam bi waye di ngako gise imbesil

  • @rosesene7586
    @rosesene7586 11 місяців тому

    Mashallah ma belle ❤❤❤❤

  • @khadymbackethiam1607
    @khadymbackethiam1607 2 роки тому +5

    merci bcp dabaye🙏🏻

  • @khadijasall8357
    @khadijasall8357 2 роки тому +11

    Dabaye nite cou ame personnalité ga vraiment Bilay ❤️❤️

  • @mbathiocisee1130
    @mbathiocisee1130 2 роки тому +18

    Mane mi toudou mbathio sakhe dama rouss changel ma belle thieuy yalla mais gor gni tmt douniou khol legui gni niouy tak rafete na presentable na day fegne tele lanouy khol motakhite lounei dilene dal walahi djiguene bou bakhe yomboul guiss wayei akaniou fei bari danio feussoul rek

  • @diedhiougnima8677
    @diedhiougnima8677 2 роки тому +2

    Bilahi ma chérie dangua bakh machallah yallah khôl rek lay fay mais tamite lou way def bopam

  • @maridateintmiel5642
    @maridateintmiel5642 2 роки тому +42

    Bamoula yobé police nguako warone bayi koula yobou police sa noone la tu as tt dit

  • @makh6167
    @makh6167 2 роки тому +30

    mbathio deffoule dara wadji moye waya waya rek. Di tak khaléyi nek fi nga dem tak mère bo khamné daffa guené tatam ba senegal yeup guisko. ngané kokou mowaradone sayayou dome n'importe quoi.

  • @youmesy1752
    @youmesy1752 2 роки тому +10

    nitt day am soutoura koudoul soutoural nitt yalla doula soutoural

  • @BoubacarDIALLO-kk1kn
    @BoubacarDIALLO-kk1kn 2 роки тому +25

    Pourquoi les sénégalais s'attardent toujours à des futilités ? Arrêtez de nous distraire avec des problème familiaux.

    • @AFdamel
      @AFdamel 2 роки тому +8

      Ils sont comme toi rek 😂😂😂😂tu écoutes , tu commentes ces futilités et tu critiques .

  • @khadydiop8274
    @khadydiop8274 2 роки тому +11

    Mieux vaux etre seul que mal accompagnè

  • @seydinaouzlaye1566
    @seydinaouzlaye1566 2 роки тому +1

    No mbatiooo Ndiaye yeureummm nakooo nakkk gnata divorce mofiii ammm té youuu gueunaaa pir kénnn wakhousiiii gnouuu topouuu siii liii di wakhhh rekkk thiooo senegal dayyy gueunaaa tardeiiii jtj

  • @binetadiagnemmediop7289
    @binetadiagnemmediop7289 2 роки тому +26

    Dabaye yaye gor yaye garmi di borom bakh, di seykat piirr di borom jom. Lou bakh rek ngay am diegou armand

  • @kosene6612
    @kosene6612 2 роки тому +1

    5:00 Seuy bo khameni 3 jours lanouko dokh présentation sikaw lale kiko dokh di djiguene sikaw kharito bou deugouwoul nii rek la meuna dèmé

  • @aissatoudiallo5162
    @aissatoudiallo5162 2 роки тому +11

    Bilae dama yereum mame baye yalla nala yalla may holou mougne 💕❤️❤️💕

  • @kannyfofana2151
    @kannyfofana2151 2 роки тому +17

    Thieyy mariage snap divorce suivi soutereu zéro. Où va ou demain c’est sa ma question 🙋‍♀️ ?

  • @mounirdiallo9270
    @mounirdiallo9270 2 роки тому +7

    Eye waye présentainema ki ma fopalko eye ronguongname waye machallah

  • @bourewalo1697
    @bourewalo1697 2 роки тому +62

    MBATHIO Bakhoule DOU NITTE

  • @mamadiallo4392
    @mamadiallo4392 2 роки тому +14

    Machalla yalla nalla yalla bayi lak sa borome keur incha Allah rabbi

  • @reinedunord
    @reinedunord 2 роки тому +39

    Dabaye dimbeuli niou. Vous êtes toutes pareilles et vous ne formez qu’un cercle de soi-disant influenceuses/stars.

    • @josephdia4354
      @josephdia4354 2 роки тому +3

      Mon guena yéss dankh amoul soutoura

    • @sincerementparlantlovejust3816
      @sincerementparlantlovejust3816 2 роки тому

      C le group des firimirine le même qui perverti le Sénégal avec leur chanteur thia tchirt lgbti bala
      gnom leu rék un seront jamais heureux

  • @malicksamb3264
    @malicksamb3264 2 роки тому +7

    Aye domérame guéne niéna yame khalisse rék guéne geume

  • @mariemamamathiam8077
    @mariemamamathiam8077 2 роки тому +1

    Bilahi ma sante yalla bima amé béne kharie sama yaye andano sama dome noma doye si kharit cofi né sama kharit la biss boula méré loumou la khamal wakh ko yalla nama yalla mousal si ma wérr domou adama yalla nanou yalla doli soutoura