Wallahi sama xol toy na si😓😭 Ya Allah mi di Bour téh ték diaamam natou yalna ko téguil natou bi mou tané ak diam si Seydina Mouhamad SAW🤲🏽méti neu trop 😢
Walahi j'ai pas les mots 😢😢😢 Je le connais c'est un grand estimable Ont parlé souvent par Facebook Les derniers mots que je l'avais dit moy grand kagne ngay tak diabar🤔 Yalna yalla yékati la may la wër si barké Seydouna Mohamed salalahou aleyhi wa🤲🤲🤲
j'ai vraiment eu un pincement au cœur en voyant Djibril dans cet état un gars k j'admirais par son professionnalisme dans l'émission automag yalla nako sunu borom takhawou insha'allah allahouma amine 🙏🙏
Thiotou xonam “menouma wax souma waxei douma meun noyi”do tegui sa micro bi fall mayko mou nopalikou sen wa keur waxal ko mais c’est pas possible on sait qu’il est malade mais boulko forcé pour preuve enfaite ça me mets hors de moi ça qui dafa sonn yalla nako yalla yeukeuti vraiment sa me touche énormément 🥹
Sama papa limoko dalone 😭ndeysane defone nagn lougnou man Mais dra 🕊️😭😭. Mbokam yeup daw ko sama yaye rek mofi nekone ak gnoune ay domam barki alkhourane sama khol bi mogui metiii 😭😭💔yalnagua dioukk si barki seydina mouhamed psl
Youssou Ndour n'est pas un prophète il n'est pas obligé d'aider tout le monde Remplis ta part de quête et prié pour lui c'est tout ce qui a de concret à faire pour lui (100fr x 1Million de Sénégalais=100.000.000) Ca pourrait le sauver par la grâce de Dieu 🙏🏾
En tant que passionné des voitures ce gars m'a beaucoup inspiré avec son emission Auto mag je prie pour toi mon grand incha ALLAH bonne guerrison a toi
Ay tfm khana bou ngéne ko diémona défal quête sakh si télé bi wala sène partenaire yi ngéne évacuer ko mais pendant deux ans mou teudd comme ça. Les entreprises privées séne intérêt rék. Les amis mome n'en parlons même pas. C'est triste. Djibril yalnala Borom bi yekeuti banga démaat say activités.
Gars yi . C'est bien de prier pour lui mais inchalah soukounek défé 1000f sakh on peut l'aider à faire des soins . Yalla nako yalla yeukeuti . La solidarité est importante. Di diégalou si kadou yi.
J’attire votre attention on ne peut pas faire d’envoi sur wave car la limite est dépassée 🙏🏽🙏🏽🙏🏽 please!!! J’admire ce monsieur exceptionnel, il incarne pour moi un reporter modèle qui maitrise parfaitement son sujet et la langue française je lui souhaite un prompt rétablissement et prie Dieu 🙏🏽🙏🏽🙏🏽
Ohhhhhh j'ai trop mal au coeur...Ndeyssan un jeune homme talentueux MASHALLAH....Ya Allah ya rahmaan ya rahiim.....yeketiko si diam ...Amin ...Allah timine thiagataagal
Mane awma khaliss wayé koumeu metr en contact av eux souma kheuyé dem dimbeuliko ak wetaliko mane magui souniou keur defoumadara Yalla nako yalla yeukeuti amine amine amine
no mane vraiment... nit kou nioul rawatina africain khawma loutakh mou boon, niak yeurmandè, mane wa TFM nioma yèm... li kèn khamoul lan la !!! inna lillahi wa inna ilayhi ra'adjy.. uuunnn !!!
Il ne faut pas s'afficher dans les télés sans se prémunir. Télé lou graw la. Kounek dileu guiss, beutt bou nekk dileu xool. Lamign bou nekk dileu toudd. Euyy bou ngueen xaamone . Que Dieu te redonne la santé Djibil ! Amiine !
@@yamatoure3410Je pense pas il lui parle en tant que malade mais avant Mane perso dama ragal écran Sénégal Dafa doy War mais yallah nako yallah yeukeuti
C’est la question que j’allais me poser ? Ani wa TFM ? Bouba Ndour ? Youssou Ndour, ou est ce qu’ils sont tous ces gens là ? Mane je suis choquée té boudé thiakhane ak foooo nioy Ndieuke diouke
J'avais pas l'habitude de regardé ay magazine auto mais il parlait et presentait cette émission si bien que à chaque fois je suivais l'émission yalnako yalla yekati inchallah metina trop😢
Est-il le seul malade du pays ? L’état ne peut pas aider une seule personne . Mais il peut mettre en place les conditions qui puissent faciliter l’accès à la santé à toute la population Prompt rétablissement ❤️🩹 à lui
@@ndieajamatt6168 gnanal ko yala degg son souhait mo geune. Adouna fo dem guide kou febar mais vidéo bi c'est pour notre chèr Djibril. Ya lalif pour Djibril dieye
Qu'est ce que je peux dire ? Pourquoi TFM ne le prend pas directement en charge ? Vraiment les patrons, il ne faut pas leur faire confiance. Même pas le cran de l'aider.. Djibril, courage et bonne guérison Force et honneur
Que Mme la ministre des solidarités Maïmouna Diéye le prenne en charge d'ar d'ar sans conditions. Prompt rétablissement à l'animateur "d'auto mag" qui m'a fait vibrer durant des années sur la Tfm
Waaw !!! Incroyable 😢mais où est Youssou Ndour 😢il n’a qu’à le prendre en charge 👍il en a les moyens et c’est un de ses employés 😢c’est vraiment triste 😞
Youssou ndour bouba ndour ndiaga ndour pape cheikh Diallo ana gnou mai bijou ndiaye doko defal quette si télé bi guir yalla yalla nala yala yeketi si barker cheikhoul khadim
Tfm vous avez une grosse part de responsabilité dans l'état de santé de ce Monsieur. Ceci démontre encore une fois l'ingratitude et la non reconnaissance vis à vis de votre ancien employé. Vous auriez dû le prendre en charge dès le départ et ne pas l'exposer sur les réseaux sociaux pour une demande de soutien. C'est juste honteux. Yallah na Borom bi safara frère.
Allahou Akbar, j'ai eu vraiment très mal au cœur😢😢😢😢😢😢 en regardant cette vidéo,seul fébar Moy nonou borom,je prie pour toi et demande à toutes les bonnes volontés de venir au secours de ce jeune Djibril et surtout à sa maman qui se bat pleinement pour faire relever son fils. Que Dieu vous rétablisse et vous aide
Kokou l’an gén koy sangé😂souroura wakh lèn ko fiii wér lèn ko TikTok feccebok gnoune woné kofa na siw gniak na diom trop way wakh lèn gnou tour soutoura amou fi
😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢ya Allah gnoungui talale sounou lokho Yi dila gnane mayale Djibril Dieye ak tane Yara bi ak mboléme gni tawate😢😢😢metina trop 😢😢😢😢mes yalla bakhna
toi son amie aussi yalla nala yalla may xolou mougn takhawoula yalla bo khaadi aussi yalla nala yalla may dolé may la diam afin de surmonter cette épreuve Dieu fera grâce parce que c'est pas facile manshalla courage
Soubhanallah voir cette personne sous un autre aspect m’a fendu le cœur thieuy Y’a Allah yay Al Karimou yallah nala souniou borom yeukeutila Alhamdoulilah ala koulli al🤲🏾🤲🏾🤲🏾
Febar rek moy none yalnala yalla yékeuti mayla wer barké Seydina Mouhamed psl 🤲 🤲
Amin inch'Allah
Wallahi amine
Amine🤲🏾
Amine y'a rabbi
Allahouma Amine 🙏🙏
Soutenons massivement Djibril 🥹
Il en a vraiment besoin
Svp aidez pour le numero de sa mère
FATOU BINETOU DIOP, LE NUMERO EST LÀ@@salimatadiouf6026
Wallahi sama xol toy na si😓😭 Ya Allah mi di Bour téh ték diaamam natou yalna ko téguil natou bi mou tané ak diam si Seydina Mouhamad SAW🤲🏽méti neu trop 😢
Aameen Ya Rabbi
Walahi j'ai pas les mots 😢😢😢
Je le connais c'est un grand estimable
Ont parlé souvent par Facebook
Les derniers mots que je l'avais dit moy grand kagne ngay tak diabar🤔
Yalna yalla yékati la may la wër si barké Seydouna Mohamed salalahou aleyhi wa🤲🤲🤲
Aminnnnn ya Rabi
Mais yow loughuénn waxx si Facebook bi c'est confidentiel
Esk gnounn khamnagnou ndax il est marié ou pas . Doffé gha trop
5k j'aimes pour la vidéo si chacun donne 1000 f cela fera 5k x 1000= 5 millions.
L'union fait la force
Partante
Partante
Partante
Partante
Partante
Allahou akbar prions pour notre frère les bonnes volonté lever vous 😢😢😢😢
😊😊😊😊😊
j'ai vraiment eu un pincement au cœur en voyant Djibril dans cet état un gars k j'admirais par son professionnalisme dans l'émission automag yalla nako sunu borom takhawou insha'allah allahouma amine 🙏🙏
Alahouma amine
Amine way
Amine way 😢
@@ndeyesarr1796 o
@@ndeyesarr1796 m00
Thiotou xonam “menouma wax souma waxei douma meun noyi”do tegui sa micro bi fall mayko mou nopalikou sen wa keur waxal ko mais c’est pas possible on sait qu’il est malade mais boulko forcé pour preuve enfaite ça me mets hors de moi ça qui dafa sonn yalla nako yalla yeukeuti vraiment sa me touche énormément 🥹
Amine
Vraiment 😢😢😢
Doyna war soumay wax douma meuna noyi mais bayiko. Au fait sene wa keur nio ko def diko bayi mouy wax sachant que c'est pas bon pour lui
Franchement! Animateur bi doméro le
Amine
Qu'Allah le tout miséricordieux l'accorde la guérison totale allahouma amine
Amiiine inchallah 🙏
Sama papa limoko dalone 😭ndeysane defone nagn lougnou man Mais dra 🕊️😭😭. Mbokam yeup daw ko sama yaye rek mofi nekone ak gnoune ay domam barki alkhourane sama khol bi mogui metiii 😭😭💔yalnagua dioukk si barki seydina mouhamed psl
C'est quelle maladie svp
Oh Allah toi qui a soulevé Ton messager Ayouba (as) redonne à Djibril la santé !
Amiiine ya rabby ❤
Thiéy aduna bimou wakhé sama khôl 😢toyna thiéy aduna yallah nakko yallah yeukeuti si barker psl 🙏🏾
Bilahi 😢
Amine 🙏
J'avais vu you offrir à une artiste 5millions sur scène. Était-il au courant de ça ?. Ce jeune talentueux mérite un soutien.
Ndiolle tall
Merci mon cher frere
@@nyimaturay7303oui c elle
Youssou Ndour n'est pas un prophète il n'est pas obligé d'aider tout le monde
Remplis ta part de quête et prié pour lui c'est tout ce qui a de concret à faire pour lui
(100fr x 1Million de Sénégalais=100.000.000) Ca pourrait le sauver par la grâce de Dieu 🙏🏾
Ndeysan li meity na
لا بأس طهور إن شاء الله أسأل الله العظيم رب العرش العظيم ان يشفيك شفاء لا يغادر سقما
Allahouma Amine
Allahouma amiiine
Oh c’est vraiment triste 😢😢yalla nako yalla may werr inchallah
Li rk mo tax kou am weer rk santal yalla
En tant que passionné des voitures ce gars m'a beaucoup inspiré avec son emission Auto mag je prie pour toi mon grand incha ALLAH bonne guerrison a toi
Thiey yala liii doyenawar deh yala nala yala yeukeuti
Amiin❤
Bilae je ne ratais jamais automag Yalla nako Yalla yeukeuti
Allahou Akhbar Yallah nalla Yalla yeukeutti si barkhé alkouran on compatis vraiment méttina tropp Ndeysann
Amine
Amine
Bonne guérison
Amine thieuye adoune chak jour mou nakh gnou😢😢
Yala nako yalla wéral thi diam
Yalla nala yalla soutoural meyla wer Djibril 😢 j'ai pleuré en voyant ta vidéo.
Bilaye Legui mom Dafa yémé
Chafakallah mon frère Yalla na nk Louy rahass sa barkar yokal la ay yiw 🤲🏻
1000f par commentaire c deja quelque chose na kou nekeu def rek. Au moins di na tané. C deja fait.!🙏pas que des mots svp agissons boul khep😢
Li metii na torop bilahi yalla nalla yalla yekati si barke seydina Mohamed 🤲
Yalnala yala may wer
Amine ya raby
Amine yarabi 🤲🤲🙏🙏
Amine way amine
Il y a des gens sans coeur, Qu Allah t accorde la guérison de tes maux et te redonne la santé. Amine ya rabbi 🙏
Amin inch'Allah
Sénégalais daffa faux trop bilahi.
Mais chacun a son tour chez le coiffeur lou way déff boppam.
Ay tfm khana bou ngéne ko diémona défal quête sakh si télé bi wala sène partenaire yi ngéne évacuer ko mais pendant deux ans mou teudd comme ça. Les entreprises privées séne intérêt rék. Les amis mome n'en parlons même pas. C'est triste. Djibril yalnala Borom bi yekeuti banga démaat say activités.
Amitié mom moy lolou qu Allah l aide .
@@jeanneboubathiam8180 Allahouma amiine 🤲🏽🤲🏽
vraiment 😢😢
Walahi amineee ❤
@@jeanneboubathiam8180 amitié amna dé bou sincères nakk j'en sais quelque chose
Bon rétablissement frère que dieu te protège .
Bayilene di déme ci khew yi diffa yakha ay millions té mounoulene dimbeuli ki febarni yalla bakhna mon frère légui lepeu meute inchaAllah
Gniy weurr si souaré Di mayé send xaliss kaylen diamou yalla si dieum dji
😭😭😭😭😭
Bilahi louwér ga wakh yalnanou yalla may khéweule gou yatou té khire nou thi dimeulé AK diamou yalla
Ani borom milliards yissi rewmi ,guir yalla khaliss diamou lén si yalla
Billayhi ma chérie lolay wakh loutakh bou nekhé ay soirée daniouy batré mais kou febar dougn ko batré 😢
Walahi je pleure
J'ai des larmes aux yeux yalla nagua werr ak diama thi barke serigne babacar sy amine yarabi aminnnnnnnnnnnnnnnnnnnnnnnnnnne
Amine yarabi inchalla si barké mame babacar sy rta
Amine yarabi 🙏
Ya Allah je traverse des moments difficil mais g tt oublier a cause de cela k Allah te vienne en aide amine
Courage cva allé inchalah
Gars yi . C'est bien de prier pour lui mais inchalah soukounek défé 1000f sakh on peut l'aider à faire des soins .
Yalla nako yalla yeukeuti .
La solidarité est importante.
Di diégalou si kadou yi.
J’attire votre attention on ne peut pas faire d’envoi sur wave car la limite est dépassée 🙏🏽🙏🏽🙏🏽 please!!! J’admire ce monsieur exceptionnel, il incarne pour moi un reporter modèle qui maitrise parfaitement son sujet et la langue française je lui souhaite un prompt rétablissement et prie Dieu 🙏🏽🙏🏽🙏🏽
Cet vidéo m’as brisé le cœur 😢😢😢😢😢
Moi aussi
Li dehh moy adina so néké si ay tolof tolof ngay kham vraiment gni la beugeu mais yalna yalla yékeuti inchallah 🙏
Yala miy tegué natou ,yalnalako yala téguil si barcké seydina Mohamed lii métina ndeyssaan sama khol begui méti thieuy adouna fébar moy nonou nite😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭
Amin inch'Allah
Amine yaraby amine
Alahou amine
Amine yarabi
Aye waye 😢 yallah n’a weure acke diameu
Ohhhhhh j'ai trop mal au coeur...Ndeyssan un jeune homme talentueux MASHALLAH....Ya Allah ya rahmaan ya rahiim.....yeketiko si diam ...Amin ...Allah timine thiagataagal
Yalna gua wer ak diam 😢😢
Thiey adouna dou dara yalla nala yalla yeukeuti 😢
Amine
Non non c’est incroyable. Vraiment c’est dommage qu’Allah le tout puissant vous assiste frere🤲🤲🤲🤲
Soutenons Djibril
C'est vraiment triste, poignant😢😢😢 Que Dieu lui accorde la plénitude de sa santé. Un élan de solidarité s'impose!
Laaa ilaha ilala 😢😢😢 damay guente wala thiey yalla sunu borom 😢😢😢
Mane awma khaliss wayé koumeu metr en contact av eux souma kheuyé dem dimbeuliko ak wetaliko mane magui souniou keur defoumadara
Yalla nako yalla yeukeuti amine amine amine
😮
Ndeysan ya bax 😢 yalla nla sa brom fay yénei bi tei mayla wer ak xeweul barkep brom touba
no mane vraiment... nit kou nioul rawatina africain khawma loutakh mou boon, niak yeurmandè, mane wa TFM nioma yèm... li kèn khamoul lan la !!! inna lillahi wa inna ilayhi ra'adjy.. uuunnn !!!
Appelle le numéro affiché.
Ayy wayy défal lolou
Il ne faut pas s'afficher dans les télés sans se prémunir. Télé lou graw la. Kounek dileu guiss, beutt bou nekk dileu xool. Lamign bou nekk dileu toudd.
Euyy bou ngueen xaamone .
Que Dieu te redonne la santé Djibil ! Amiine !
Si il n'y a pas affichage comment on fait pour l'aider, moi je savais pas que il et malade
@@yamatoure3410Je pense pas il lui parle en tant que malade mais avant Mane perso dama ragal écran Sénégal Dafa doy War mais yallah nako yallah yeukeuti
Walahi ma chérie kham na dafa sone rek metina trop sakh
Yallnala yalla défal werr té yèkeutii leu ba ngua nekatt ci say activités inchallah
Amina poté nitt kou bakh nga Djibril c’était ton collègue Diapsi seu dieukeur Malick Nar mou diapalé ko Ngir yalla
Yeugue nako Li depuis août la nguistal rek moy takh gnou def
Sister gnognou linouy woné ak linouy dounde bokoul.yoronou tousse danouy frimé rek.
Wa ani Youssou ndour
YALLA NA WERA AK JAMM CI BARKI SEYDINA MOUHAMED WAKHA LEN AMIIN
Gnome gneup ay doméram lagnou
Ani wa Tfm, c’est incroyable comment les gens sont méchants !!!
C’est la question que j’allais me poser ? Ani wa TFM ? Bouba Ndour ? Youssou Ndour, ou est ce qu’ils sont tous ces gens là ? Mane je suis choquée té boudé thiakhane ak foooo nioy Ndieuke diouke
@@Diija02Li dee moy Senegal, sene collègue la wonn mou nek si état bi, dougn ko sakh faller mais si c pour dem jouer wala ay thiakhan gnosiy premier
C ce que je voulais dire oh mon Dieu
Kouthia wakh naco mais TFM lignou nek Di sétane ni bakhoul
Yalla n'a ko sunu borom yeukeutiko
😢😢ayway où sont les bonnes volontés
Prompte rétablissement 🙏lii Métina trop 😢
J'avais pas l'habitude de regardé ay magazine auto mais il parlait et presentait cette émission si bien que à chaque fois je suivais l'émission yalnako yalla yekati inchallah metina trop😢
J’ai le cœur meurtri 😢🤦♀️🤦♀️🤦♀️yalla na yalla feugue bopam bamou tané ak diam inchallah 🙏
Nous souhaitons que le ministre de la santé lui vient en aide
Est-il le seul malade du pays ? L’état ne peut pas aider une seule personne . Mais il peut mettre en place les conditions qui puissent faciliter l’accès à la santé à toute la population
Prompt rétablissement ❤️🩹 à lui
Yala nala yala degg amine ya rabi.
@@ndieajamatt6168 gnanal ko yala degg son souhait mo geune. Adouna fo dem guide kou febar mais vidéo bi c'est pour notre chèr Djibril. Ya lalif pour Djibril dieye
Incroyable Yalna niou Yalla may wergui yaram
Yalnako yalla may wer 🙏🏻🙏🏻🙏🏻
Allahouma amine
Qu'est ce que je peux dire ?
Pourquoi TFM ne le prend pas directement en charge ?
Vraiment les patrons, il ne faut pas leur faire confiance.
Même pas le cran de l'aider..
Djibril, courage et bonne guérison
Force et honneur
Bien dit pourquoi ?
😢😢😢 bilahi g les lames o yeux métina n'a gnou diapalé guir Yalla khalé bou ndaw ndeyesane ohhhhh Yalla nako Yalla takha wou😭😭😭😭😭😭😭
Oh Seigneur pitié!!! releve notre frere. jai mal au coeur
Dmrm bi lekk xaliss bi yallah na dieul plaçam gnak yeurmandé ba deh tchim
Bon rétablissement ❤️🩹 Djibril febar moy nonu nittt💔
Dinako réthiou dh inchallah
@ j’espère bien def na Lou gnaw
Vraiment je compren pas les gens comment peut ton volé une personne malade que dieu nous aide
Ki kay mo totheu leufeul ndayam waya dinako guis setane keneu KO ate' yalla guene bou nit ki ndeysane kouma dimbali woute boulko satheu 😭😭
@@FatouFall-nx3ixbly
Que Mme la ministre des solidarités Maïmouna Diéye le prenne en charge d'ar d'ar sans conditions.
Prompt rétablissement à l'animateur "d'auto mag" qui m'a fait vibrer durant des années sur la Tfm
Ani Youssou Ndour meunou ko dieul en charge
Waaw !!! Incroyable 😢mais où est Youssou Ndour 😢il n’a qu’à le prendre en charge 👍il en a les moyens et c’est un de ses employés 😢c’est vraiment triste 😞
Yalla nalla yalla may tane si barké seydouna mouhamed 🙏 ❤
Ani Youssou Ndour Borom TFM😭😭 Naniou Diapalè Djibril Teh Yalla Takh😢
Bilahi
Wakh deg yalla wayi amna khaliss yokhamni temit
@@MamourSylla-w7zaka ya wakh deug, khalissou musique ak khalissou carte meunossi diamou yalla... ndakh allalou djinnè la
@@bathiembaye1199 degueule ma yii khetou bakarou rekk
@@massndiaye6933 ladial youssou ndour loutakh dou dèm ADJY makka, bayyi wèy !!!!!!
J’aimais trop son émission na tanei ak diam🙏🏽la vie est injuste 💔
Pape cheikh Diallo ak Boubacar Diallo diap l'ene si té yalla takh😭😭😭
Bon rétablissement ❤️🩹😭😭😭🤲🏾
Yallna tané Ak diame ❤❤❤🙏
Youssou ndour bouba ndour ndiaga ndour pape cheikh Diallo ana gnou mai bijou ndiaye doko defal quette si télé bi guir yalla yalla nala yala yeketi si barker cheikhoul khadim
Vraiment
Gnii nga lim béne kéne si Niom rek meun nako fadji
Wayé douniou ay nite sakh
Amine ya raby
Bilay sma ❤toyna pape chekh khalis bi ky maye si télé bi diokh ko ki guir yalla 😢😢😢😢
Bilay gni geumouniou dara gnom yak molen gueneul yallah bakh na yallah na wer
Thiey adouna😢😢😢😢 mo tereudi😢😢😢.... olof day wakh doundou guou soteguoul lounek khadj nasi.... yalla nala yalla yeketi si barke Mouhamed (PSL)
Walay wér moy léep adouna amoul solo nit dou dara
Lou lerr Ndeyssane 😢
Bonne guérison à vous mon frère
Walahi
Amine yarabi 🤲🤲🙏🙏
DIÈYE MASSAMBA AK YÈRIM YALNA YALLAH FEUGUEU SA BOPEU 🤲🏾🤲🏾🤲🏾
Amine
Wao thiey yalla massa massa c’est triste yalla bakhna yalnaga tané ak diam vraiment ken yéné woula li 🙏🙏🙏🙏courage
Allahou akbar❤ yalna la yalla yeukeuty djiby❤
Oui vraiment soutenons le massivement c'est notre confrere
Sokhna siii Yalla nako Yalla yaye 🙏🙏🙏🙏
Q'ALLAH t'accorde la guérison
Que le Bon Dieu l’assiste et lui redonne une santé de fer.
Thieye yalla , lii méttina
Yalnako yalla yékketi way n ndaye sann
Massa Bon rétablissement djibril yalla mila tėk natou bi yalla nalako tėguil inchallah
Ay djibril Yalla nala yalla yeukeuti si barké seydina muhamed 😢😢
Yallah rek moy karim ❤❤❤🙏🙏🙏
bonne guérison mon frère
Tfm vous avez une grosse part de responsabilité dans l'état de santé de ce Monsieur. Ceci démontre encore une fois l'ingratitude et la non reconnaissance vis à vis de votre ancien employé. Vous auriez dû le prendre en charge dès le départ et ne pas l'exposer sur les réseaux sociaux pour une demande de soutien. C'est juste honteux. Yallah na Borom bi safara frère.
Djibril yallah nala yallah yekeuti si barke seydina mouhamad
Allakhou Akbar, g mm pas les mots😢😢😢
Mais khana Youssou Ndour yeugoul li la yakar de 😢😢
Yalnako yalla takhawou
Ça c'est impossible 2ans la febar tfm chaque année mouy mayé ayy enveloppe 50000f 100000f
@@marietoubodian5425emission yi molay faye. Dagnlay outlo sponsor pour nga dialale sa emission 😢
Yene khamolene famille ndour billahi
@@SD2FOfamille bou yèmmè laniou !!!
Doy na war dh metina lol
Li metii na que dieu te vienne en aide🤲
Allahou Akbar, j'ai eu vraiment très mal au cœur😢😢😢😢😢😢 en regardant cette vidéo,seul fébar Moy nonou borom,je prie pour toi et demande à toutes les bonnes volontés de venir au secours de ce jeune Djibril et surtout à sa maman qui se bat pleinement pour faire relever son fils. Que Dieu vous rétablisse et vous aide
Kokou l’an gén koy sangé😂souroura wakh lèn ko fiii wér lèn ko TikTok feccebok gnoune woné kofa na siw gniak na diom trop way wakh lèn gnou tour soutoura amou fi
Longue vie à nos mamans 🫶🏾🫶🏾🫶🏾🫶🏾🫶🏾🫶🏾🫶🏾
Une honte pour la TFM.
😢😢😢 tfm dou touss
Vraiment sa me fait très mal😢😢😢
Yallah nakou Yallah may werr ak werlé 😢
Mon Dieu QU'ALLAH lui redonne la santé,le voir dans cotte état me fait vraiment de la peine 😭😭😭💔💔🥺🤲🤲🤲🤲
massa frére yalnala yalla yeuketi AK diam 🙏🏽
Massa frère yalna yalla maye wer 🙏
Ani patriotes yi Ousmane wotrl cagnotte guirlande yalla guéne dimbali co
Yalla na yalla may wèrr bagua délouwat si say activités🙏🏿
Amin inch'Allah
Yalnala yalla may werr
Bon rétablissement
Le présentateur a des larmes au yeux
C'est dur
😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢ya Allah gnoungui talale sounou lokho Yi dila gnane mayale Djibril Dieye ak tane Yara bi ak mboléme gni tawate😢😢😢metina trop 😢😢😢😢mes yalla bakhna
😢😢😢
No li metina trop yalla nale yalla same mayla goudou fané AK wer inchallah yalla nalne yalla yeketi
toi son amie aussi yalla nala yalla may xolou mougn takhawoula yalla bo khaadi aussi yalla nala yalla may dolé may la diam afin de surmonter cette épreuve Dieu fera grâce parce que c'est pas facile manshalla courage
Soubhanallah voir cette personne sous un autre aspect m’a fendu le cœur thieuy Y’a Allah yay Al Karimou yallah nala souniou borom yeukeutila Alhamdoulilah ala koulli al🤲🏾🤲🏾🤲🏾
Ragalouma deh febar la ragale bilahi 🙄 yalnako yalla yekety amine yarabi 🥲😭