Machalah Fatou Guéwél. Li moyy adouna nitt bokko tanné dangakoyy dimeuli. Que les autres artistes prennent exemple sur toi. Tu pouvais te dire que y’a le ministère de la famille mais non, tu as déployé des moyens pour venir en aide quelqu’un qui est dans le besoin. Yallana sa téranga yokkou, yalla mayela wérr té goudeule sa fane. Bilaye doye nga royou wayy. Boula nékhone bilaye nga déme défeko thi poukeuré wayyé défouloko. Finga tékk sa tank fofoula. Yalla nalla yalla diapalé si sa mission. Sama khole bilaye sédana
Ce sont ces genres d’informations dont nous avons besoin et non des informations inutiles. Bravo à la fondation dirigée par Fatou Guéwél, roye léne si Fatou Guéwél Diouf nguirr yalla yéne gni yalla bakhé té diokh léne téranga
Macha allah lou diot yomb elle a telma galerer dans la rue tjr avk ces enfants chak fois dama ko dane romb si mbed mi tjr avec ces enfants en tt cas mougne na ba yalla defal ko xeweul mention special a vous osi nalene yalla faye
Ma sha Allah, association Fatou gueweule kara, yallah na leu yallah sameu, diapeulé leu si lou barkh y guaye déf ainsi qu'à toute l'équipe de Pape Niang 👏🏾👏🏾👏🏾👏🏾👏🏾🙏🏽😊
Natou yalah da meti AlhamdouliLah la fille aussi rien voir son visage tu sai qu’elle a beaucoup souffert tu doit être heureuse maintenant gor req mo soneuh yalah ko yalah may liguey bou bax geuneu diapale sa yaye et tes petits frères aussi merci à tt l’équipe ♥️
Lepp Li khalé bi wa khone ya yam féki sina ko bilahi liga liguey sa kuer Diekuer lala sono brom fay lo bakh gako dji yalla fay nala lepp ❤🙏😭 Merci beaucoup fatou guewel❤😭🙏yalla nala yalla fay sa khol amine❤🙏
Yaye Fatou kara yalla na yalla goudeul sa fane te mayla weur ak katane babarakati cheikh ahmadou kara mbacke noreyni man noreyni rek motakh ma beuge la
Kouko dégue bo djoyoul rek amo khol Fatou mi yalla nako yalla takhawou si barker seydina mohamed 👏 👏 ta Fatou gueweul diouf yalla nako fi yalla bayi si barker seydina mohamed 👏 yalla yokouko ba
Fatou guewel d limou def betou gnou gnoune gni deuk ak mom. Dafa bakh be kou guéne si bireum bakh la yakar. Machallah❤️ Yalla ne ko Yalla Sam samal ko ndiabotam goudeul fanam🥰❤️🙏🏾
Billa hi li fatou gueweul def niep la ko defal yalla khamnako lou am solo la bilay demb la ko setan dioy mes khale yi yalnan reuisit si barke seringe Babacar sy rth amine💯❤
Machallah li rafète na yalla guiss nala dè Soxna fatou guèweul gnogui niane yalla mou goudal fane wi yokk wèr gui ak mbolèm gninga andal liguèye bi thia yalla barkèl sèn lèp adouna ak allahira barké BROME TOUBA KHADIMOUL RASSOUL AMINE sama khôl sèdde na lol thié dieuf dji yalla xamnako , gnogui ninal wa suite internet bi yalnalèn yalla taxaawou thié sèn liguèye bi thia kaw thia kanam rèk INCHALLAH
Machallah le peuple est content merci à l'association de tata fatou gueweul diouf djeureudjeuf pape et l'équipe alhamdoulhilah vous avez fait ma journée Dieu merci la fille est très bien éduqué machallah néna liguéy Bouma am bakhena yalla n'a yalla motali lépe inchallah 🙏💓❤️😍🌹💐🎊🌸🎊🎊🎊💐🎊🌸🎊🎊💐
No pape iow yallah réck mom sunu mou defala diam cii aduna toi safé doundou amna solo trop cii kanam réck long vie et bcoux bonheurs courage réck 🙏🙏🙏🙏🇸🇳🇸🇳
Yalla kham Nany bekk naaaaa thiii yaw sounou yaye djiiii yalla nalla yalla sounou borom yokou ba yeuk by Diahi Nabil Moustapha psl 🤲🤲🤲sedal gua sama khôl ❤️ by lolou walahi
Vraiment fatou guéweul Kara t as fait un beau geste Li yalla dinalakoooo fay adouna ak alakhiraaaaaaa Li la ammm ammmmm di dieurigne yalla nala yalla yoxouuu baga xammmmmm
Maman Fatou guéweul yannala yalla fayy yokoulo bangua yeukk ko si barké Baye Niass 🤲🤲 bilay Di déff ay aide sociale mo yagg nékk sma rêve bilay 🥺🥺 beugg na bokk si association bi inchallah
Wallhi raffena machlla un garand merci à toutes la fondation noreyni solidarité et à Fatou gueweul kara wallhi merci man sam goll deknna billahi dapi Mauritanie
Machala sama xol bi Come wanagou bote yala nalen yala Faye Pape yak sa équipe dierejef Fatou guewel yalna yala Faye len sokhna si khana Fatou guewel sa mak la daguen ndouro machala
Awma habitudes di commentaires si réseaux sociaux yi ms dama contane trop maman Fatou yalla nala yalla faye 🥺 yalla nala yalla may lénéne lou eup lingako défare🤲🤲 que dieu vous bénisse
Macha Allah gnissi déf séne deureume yalla naléne ko yalla fouleul defko yiw. Mane sama khôl da séde ba melni Mane lagnouko défal. Gni ame nagnou guestou gni gnake. Merci aussi à maman Fatou Guéweul
Yalla naléne yalla may wérr ak werlé ak dolé biguen agualé social bi am n'a solo lole thi rew mi merci maman Fatou guewel yalla nala borome bi fêye sa xol
souniou yaye Fatou gueweull yalle na yalle faye yiw dieureudieuff mane de kontan na sama xoll sedana doropp yaye boye Merci beaucoup yaguafi rekk sadounou amna solo ❤💕😍🥰
Fatou guéweul yalla na yalla yok té wéeral la té fayal si barkè Yonnente bi Paix et Salut sur lui
Machalah Fatou Guéwél. Li moyy adouna nitt bokko tanné dangakoyy dimeuli. Que les autres artistes prennent exemple sur toi. Tu pouvais te dire que y’a le ministère de la famille mais non, tu as déployé des moyens pour venir en aide quelqu’un qui est dans le besoin. Yallana sa téranga yokkou, yalla mayela wérr té goudeule sa fane. Bilaye doye nga royou wayy. Boula nékhone bilaye nga déme défeko thi poukeuré wayyé défouloko. Finga tékk sa tank fofoula. Yalla nalla yalla diapalé si sa mission. Sama khole bilaye sédana
Merci Fatou gueweul c'est des personnes comme toi, qui font que j'ai confiance à l'avenir.merci merci merci
Juska ce moment je n'arrête pas de pleurer yalla rek Moy bour bou mag bi
Enfin les journalistes nous dévoilent des actions utiles
Ce sont ces genres d’informations dont nous avons besoin et non des informations inutiles. Bravo à la fondation dirigée par Fatou Guéwél, roye léne si Fatou Guéwél Diouf nguirr yalla yéne gni yalla bakhé té diokh léne téranga
Merci maman Fatou guewel li Motakh ma beuguela yalla nala yalla faye
Association bi mérite d'être soutenu vraiment .k Dieu vous bénisse
Macha allah lou diot yomb elle a telma galerer dans la rue tjr avk ces enfants chak fois dama ko dane romb si mbed mi tjr avec ces enfants en tt cas mougne na ba yalla defal ko xeweul mention special a vous osi nalene yalla faye
NDeyssane, wornama ni si tu savais qu'elle dort dans la rue nga deif ci ay dingue. Santt yalla adja, khol yeuppa Toyone
Voilà lolou amna solo machalaa fatou defneu loumou meun.tek la si yone djangal la nougnouy nappé .takkal sa ndig geum sa bop. Ligey ndakh koula dimbali tay bou souba mou meneu dimbali kenenn
Niit amoul loudoul mrom niitam bonne volonté yii war nagn khol sii lii dii diimbalii niit ta yallah takh Fatou gueweul diieureudiieuf ak sa wa fondation bii yeup ♥️♥️♥️
Merci Sokhna Fatou guéwale Diouf ak toute l'équipe particulièrement Pape Niang et sewrou
Ma sha Allah, association Fatou gueweule kara, yallah na leu yallah sameu, diapeulé leu si lou barkh y guaye déf ainsi qu'à toute l'équipe de Pape Niang 👏🏾👏🏾👏🏾👏🏾👏🏾🙏🏽😊
Long vie à tw Fatou gueweul , Dieureudieuf pape Niang AK groupe bi yeup yalnalen yalla fay
♥️💔♥️♥️♥️♥️😭🤲👈
Amine way 😭😭✅😭❤️❤️❤️
amine
Amine ❤️❤️
Il
Yalla na yalla faye fatou geuweul diouf
bi lahi machallah yalla nama yalla may weurseuk bama mana diapalé néw di dolé yi inchallah vous êtes dé référence fier de vous
Amine Lo lou rèk lay nian yallah
Machallah Fatou Guéweul yalnala cheikhoul Khadim takhawou🙏🙏❤️❤️
Pape yalnalene yalla defale diam amine Fatou gueweul Diouf yalla gisnala bayinalak môme dioyna wayee amouma yallanala yalla yookak
Yalnama yalla wonalek yoow amine
Natou yalah da meti AlhamdouliLah la fille aussi rien voir son visage tu sai qu’elle a beaucoup souffert tu doit être heureuse maintenant gor req mo soneuh yalah ko yalah may liguey bou bax geuneu diapale sa yaye et tes petits frères aussi merci à tt l’équipe ♥️
Machalla aduna lo guiss appe laye kharr kouné khamnani mbeed nekhoul bilahi wayé adina kouné ak sa diardiar dieureuf cheikh Niang diarama Fatou gueweul wakh deug yalla royoukay gua may nianal séne groupe bii yalla fayléne katanal léne lakhlén fa yakh éguoul diii nianal fatou gueweul yalla guoudal fanam vraiment khôl yepp toyna
Lepp Li khalé bi wa khone ya yam féki sina ko bilahi liga liguey sa kuer Diekuer lala sono brom fay lo bakh gako dji yalla fay nala lepp ❤🙏😭
Merci beaucoup fatou guewel❤😭🙏yalla nala yalla fay sa khol amine❤🙏
Yaye Fatou kara yalla na yalla goudeul sa fane te mayla weur ak katane babarakati cheikh ahmadou kara mbacke noreyni man noreyni rek motakh ma beuge la
Ndaysane bola yalah diokhé coppo khamalne iow kasse la mais bola diokhé pàne dalà sedeleloo délen diamou yalah thi néwdi dooleyi wasalam 🙏🙏🙏
Machalla yalna goudou fann werr
Pape niang dieredief yalnala yalla faye yak maman fatou nguewel vraiment video bi limassi dioy wayei instanbi magui contane🙏🙏
Ay li yalna len yalla fey mome Yi fey Li dey borom Hol Bou yatou rek Moy dioxe machalla
Fatou guewal yalla rek mo am faye yalla na yalla faye
yaye mougn na ba am limou beuguon mashallah fatou geweul yalla guiss nala💝💝🙏🙏
Kouko dégue bo djoyoul rek amo khol
Fatou mi yalla nako yalla takhawou si barker seydina mohamed 👏 👏 ta Fatou gueweul diouf yalla nako fi yalla bayi si barker seydina mohamed 👏 yalla yokouko ba
Mash'Allah ❤️❤️ yallah nafi diam sakh
Fatou guewel d limou def betou gnou gnoune gni deuk ak mom. Dafa bakh be kou guéne si bireum bakh la yakar. Machallah❤️ Yalla ne ko Yalla Sam samal ko ndiabotam goudeul fanam🥰❤️🙏🏾
L00ll
Billa hi li fatou gueweul def niep la ko defal yalla khamnako lou am solo la bilay demb la ko setan dioy mes khale yi yalnan reuisit si barke seringe Babacar sy rth amine💯❤
Mashallah maman Fatou geuweul ak groupe social longue vie à vous
Machaalla wa fondation yalla guiss na lep yalla nalén yalla takhawou
Machalla rafétena yalna yalla yokou léne si barcké est serigne fallou
machallah yalna yalla feyelenne senne holle li leppe pape Niang mo ko waral bilaye je suis tout cœur avec vous 😭😭😭😭😭
Yalna léen yallah fay si barket seydina Mouhamed saw 🙏🙏🙏🙏❤️❤️❤️❤️❤️
Alhmdulillah blh Liiiih dawanaah sama yaraam trop ma-sha-Allah Sokhna Fatou guéweul yallah naa sheu diaam yaagu saaay maay di bawaneu vraiment🙏🏿♥️♥️♥️ keen dou ñiii révélé Liiiih yeup bamou maneuh thie diott Yallah amna sen faay yallah naleeen yallah 😭💔
Machallah li rafète na yalla guiss nala dè
Soxna fatou guèweul gnogui niane yalla mou goudal fane wi yokk wèr gui ak mbolèm gninga andal liguèye bi thia yalla barkèl sèn lèp adouna ak allahira barké BROME TOUBA KHADIMOUL RASSOUL AMINE sama khôl sèdde na lol thié dieuf dji yalla xamnako , gnogui ninal wa suite internet bi yalnalèn yalla taxaawou thié sèn liguèye bi thia kaw thia kanam rèk INCHALLAH
Un grand merci à ses gens qui ont aidé cette femme yalna len ko borom bi faye
Ayee maman fatou yalla n'alla yalla fayeeeee
Alhamdoulilah 🙏 Dieureu Guen dieuf way🙏 Yalla nalen borom bi Faye si Barki Nabie Moustapha 🙏
Pape Niang yalla nala yalla faye ♥️
Machalla maman Fatou guéweul yanna yalla deffal la diama ya rabi
MAchalla yalla na lene yalla bolle fayy barkhe seydina mouhamet psl
Machalla raféte neu 😍👍
Machallah إن الله يرزق من يشاء بغير الحساب.
Manchallah maman fatou guèweul kara yalna la yalla yok tè samla doko reuthiou dè bilahi 😍😍😍😍😍😍
Machallah le peuple est content merci à l'association de tata fatou gueweul diouf djeureudjeuf pape et l'équipe alhamdoulhilah vous avez fait ma journée Dieu merci la fille est très bien éduqué machallah néna liguéy Bouma am bakhena yalla n'a yalla motali lépe inchallah 🙏💓❤️😍🌹💐🎊🌸🎊🎊🎊💐🎊🌸🎊🎊💐
😭😭😭😭😭
Machalla yalla nalene yalla fay pape Tata fatou et la fondation ❤❤❤❤❤❤❤
Machallah
No pape iow yallah réck mom sunu mou defala diam cii aduna toi safé doundou amna solo trop cii kanam réck long vie et bcoux bonheurs courage réck 🙏🙏🙏🙏🇸🇳🇸🇳
J’aime mon pays 🇸🇳
Machalla am na solo lol yalla nako yalla guena diapale ci barcke serigne fallou mbacke machallah
Machallah ndaysane yallana lén yalla faye Barack S TOUBA
Manchallah merci beaucoup à vous k Dieu vous bénisse
Màchalla Mme Fatou guewel n'a yalla Faye la
Mashalla FatouYalla na yallla yalla faye
Ndeysane geste bi raféte na torop je veux juste savoir ndakhe mbokame yi gnogui guisse téranga yi khana diguéne rouse bilahi yalla nélawoule
Merci Sokhna Fatou gueweul ak Pape Niang si kaw si kanam si barké Seydina Mahamed laff thiat
Yalla kham Nany bekk naaaaa thiii yaw sounou yaye djiiii yalla nalla yalla sounou borom yokou ba yeuk by Diahi Nabil Moustapha psl 🤲🤲🤲sedal gua sama khôl ❤️ by lolou walahi
Vraiment fatou guéweul Kara t as fait un beau geste Li yalla dinalakoooo fay adouna ak alakhiraaaaaaa Li la ammm ammmmm di dieurigne yalla nala yalla yoxouuu baga xammmmmm
Mashaalah mashallalh laf khiate raffetena trop mashallalh yallanalene yalla faye thii barke seydina mouhamed psl
Macha allah pape liguéye bi amna solo ak maman fatou guéweul yalna yalla fayléne
Ay waay guewal yaa baakh. Yalna yalla barckel licie dess, tè barckel ndiabot gui. Yaa reuy khol maa chaa allah.
Yalnalene yalla fay yiww 🙏🇸🇳❤️
Fatou yalna yalla goudal sa fane amine amine amine
Alhamdoulilahi. Yalla na ma Yalla may aye kheweul you bari bama mana def sama yené si djami Yalla yi Amine Amine Amine Amine Amine Amine Amine
Maman Fatou guéweul yannala yalla fayy yokoulo bangua yeukk ko si barké Baye Niass 🤲🤲 bilay Di déff ay aide sociale mo yagg nékk sma rêve bilay 🥺🥺 beugg na bokk si association bi inchallah
Yaye Fatou yalna yalla soutoural dioufa niokhobay
Wallhi raffena machlla un garand merci à toutes la fondation noreyni solidarité et à Fatou gueweul kara wallhi merci man sam goll deknna billahi dapi Mauritanie
Aka malèn naww Sama hole dafa fèss trop😭😭😭 contanena trop yalla nalèn yalla faye
Yala mo kémané Bilahi bou kén yakam ti lo mougne mou diekh pour tout le monde
Machallah yalla nalene yalla faye🙏🙏🙏🙏🤲🤲👏🏿👏🏿👏🏿👏🏿👏🏿😭😭😭😭😭😭❤❤❤❤❤❤❤
Baye pape niang contane n'est ye ci ioe bly yalla n'ala yombou Amine
Machala sama xol bi Come wanagou bote yala nalen yala Faye Pape yak sa équipe dierejef Fatou guewel yalna yala Faye len sokhna si khana Fatou guewel sa mak la daguen ndouro machala
Machala fatou guewel yalna yalla yokou fane bi yaw ak sa diabote mention spéciale à pape niang é mifa sowrou ect laf thiate
Awma habitudes di commentaires si réseaux sociaux yi ms dama contane trop maman Fatou yalla nala yalla faye 🥺 yalla nala yalla may lénéne lou eup lingako défare🤲🤲 que dieu vous bénisse
Yalla nalène yalla faye wa association bi 🤲🤲
Ndèye san machalla amna solo trop ndèye san
Soxna fatou guéweul yalna yalla guoudeul saye fane
Adjia fatou gueweul yalla na la yalla faye si barké seydina Mouhammad
Masha allah
Yalnalein yalla faayeu
Alhamdoulilah🙏🏽🙏🏽machallah yalla naléne yalla fayy ya rabi🙏🏽🙏🏽
Macha Allah gnissi déf séne deureume yalla naléne ko yalla fouleul defko yiw. Mane sama khôl da séde ba melni Mane lagnouko défal. Gni ame nagnou guestou gni gnake. Merci aussi à maman Fatou Guéweul
Bonne continuation.diadieuff ça kaw ça kanam
Machalah Maman Fatou geuwél li raffét trop yalla nala yalla défal diam ak wa équipe and takhawou niou wéradi
Ndeyssane Dieureuf yalla nallen yalla faye
Fatou gewal bole wol dare aki wahk mahcalla maman fatou❤❤❤❤❤🇪🇦🇪🇦🇪🇦🇪🇦🇪🇦🇪🇦🇪🇦
Mashallah yallah n'a yallah faye yiww barkepp Noreyni
Machallah je suis très contente de vous machallah
Body Mme méngue machalla wakh bi rafétna
Machallah fatou gueweule and papa yalla na yalla faye
Ndaysane nit li rek lamanal moromou nitam adouna amoul solo leipp day diex Yalla nalen yalla fay ✅❤️❤️
Fatou geuweull yalla nala yalla faye ta sammou
Machalah le peuple est content ♥️dieuredieuf
Yalla naléne yalla may wérr ak werlé ak dolé biguen agualé social bi am n'a solo lole thi rew mi merci maman Fatou guewel yalla nala borome bi fêye sa xol
Jeureujeuf pape
Niang Yallah naleuh yallah fay
Machalla Amine 🤦♀️ 🤲 📿 😭😭😭😭♥️❤merci beaucoup
souniou yaye Fatou gueweull yalle na yalle faye yiw dieureudieuff mane de kontan na sama xoll sedana doropp yaye boye Merci beaucoup yaguafi rekk sadounou amna solo ❤💕😍🥰
Yalla n'a yalla fay fatou guewale
Merci beaucoup tata fatou
Yallah na ko yalla fay si adouna ak si allakhira