Allahou akbar Thieuy Pape Niang Défna lou raffét thi triplé yi sén yaye guén adduna

Поділитися
Вставка
  • Опубліковано 16 січ 2025

КОМЕНТАРІ • 597

  • @awaladivafall5033
    @awaladivafall5033 3 роки тому +147

    Toujours pape Niang avec son coeur en or et ses inter notes qui soutien toujours merci😍😍😍😍😍😍😍😍😍😍

  • @fatimadial5911
    @fatimadial5911 3 роки тому +63

    Pape niang ,je n'ai pas l habitude d écrire dans les commentaires, wayé bi dé ,c est plus fort que moi.pape niang ,yalla nala yalla faye sa khôl.

  • @yasminaka2595
    @yasminaka2595 3 роки тому +1

    Kham n'a so amoul Lou bakh kén douko am bilahi sa ligéy réfét n'a ma challa déf té yalla reka takh yalla nala yalla Faye

  • @smstv1176
    @smstv1176 3 роки тому +322

    Pape Niang mérite le poste de ministre de la famille et de l'action sociale.

    • @awagueye9752
      @awagueye9752 3 роки тому +2

      Allah ou akbar

    • @khadijalam6351
      @khadijalam6351 3 роки тому +5

      Bilahi ki yalla nako yalla soutoural

    • @aminetadiegne2832
      @aminetadiegne2832 3 роки тому +3

      Bilaye mérite ko

    • @laghemtv7024
      @laghemtv7024 3 роки тому +8

      Bilahi walay done ministre khel ak khalate ak yeurmandé mais dou li gnou guiss Sénégal ministre milliardaire té do dimbali kéne doyna warr

    • @salydiallo35
      @salydiallo35 3 роки тому +3

      Pape yalla nala yalla faye tè mayla ndiabote bou bari tè barkel

  • @fatouseck9151
    @fatouseck9151 3 роки тому +23

    Cas bi hier damako dioye ba sama boop done mèti mè pape niang yalla nala yalla faye 🙏

  • @bernilynsha
    @bernilynsha 3 роки тому +78

    Pape sa doundou amena dieurigne mâcha allah

  • @awathiam8199
    @awathiam8199 3 роки тому +11

    Pape sama xol lako tibé wallae yalla nala yalla taxawou ar la billae di diapalei gniko sokhla yalla dinala fay sa xol pa bravo à tw billae sedal ga xol sénégalaise yeup nakh aduna li la d’où keur Lo am bokou ko ak gniko sokhla nakh aduna kén d’où dei di yobatei millliare ni keur kou rafet ni yerei bou rafet yalla dieuf lay fay ak xol bou rafet yalla dinala fay sa xol pap inchallah

  • @mamemariethiam3525
    @mamemariethiam3525 3 роки тому +2

    Ay wayy maylenn pape Niang xalé yi té yalla tax amagoul domm ba légui ndeysann yalnako yalla may diamm diou sax dakk amiinn

  • @khadijasall8253
    @khadijasall8253 3 роки тому +4

    Mane je m demande ministre yii lann moy sén liguéy si Sénégal Bilae pape niang yalla dinala fayy machalla liguéy bi rafett n’a trop contane n’a sii 🙏🙏🙏🙏🙏🙏

  • @ndawamboup2653
    @ndawamboup2653 3 роки тому +23

    Machalla papa Niang yala guisna liguay def dinala faye SA khol inchalla

  • @amintadiagne4700
    @amintadiagne4700 3 роки тому

    Machalla pape NIANG yalna yalla diapaléne si barké seydina Mouhamad psl ya rafet khol

  • @diopmamediarra1220
    @diopmamediarra1220 2 роки тому

    Pape Niang yalla na la yalla bolé si mirr ya d’ère dire s Touba yalla na ko yalla def khalé yi yalla na niou doudou té am barkile yy yoyou khalé yi yalla na ko yalla yeureum kharéko aldianay firdawsi ahh lie metina torpp torpp

  • @adamadiobembengue8838
    @adamadiobembengue8838 3 роки тому +1

    Machalla Pape Niang yalna yalla goudeul saye fane ta maye la wër

  • @ahmadtidianeathie2192
    @ahmadtidianeathie2192 3 роки тому +5

    Pape yalna borombi defal say mbir tay ak eulleuk 🤲🏻🤲🏻🤲🏻😭😭😭😭wallahi sopp naala thi you am solo yingay def yak sa équipe qu’Allah accepte vos œuvres mon frère 🤲🏻🤲🏻

  • @ndeyecheikhgueye6004
    @ndeyecheikhgueye6004 3 роки тому +50

    Ndeysane longue vie aux bébés , Baye pape yallah na la yallah fay ak toute l'association ci barkee Seydina Mouhamed psl

    • @maremeciss2054
      @maremeciss2054 3 роки тому +1

      allahouma amine

    • @fatoudieye4102
      @fatoudieye4102 3 роки тому

      Pape yallnala yalla faye sakhol yallnaga féké ndiariniou bébés yi

  • @ramambow9843
    @ramambow9843 3 роки тому +6

    شكرا جزاك الله خيرا وبارك فيك تقبل الله منا ومنك صالح الاعمال وجعلك في ميزان حسناتك

  • @fatousidibe6757
    @fatousidibe6757 2 роки тому

    Yalla nala yalla soutoural si werou koor gui pape Niang j’ai le cœur meurtri nala yalla fay ohhhhhh

  • @la_fille2841
    @la_fille2841 3 роки тому +7

    Ndeysane yaye sonou na eumb 9 mois noumou meittei gua am dom yalla dogual ni doleine guiss sakh sougnouy magg meitina yalnako yalla kharei aldiana firdawsi 🙏ay domam magg ba diko gnanal yaye amoul fayyy🙏

  • @mamediarradieng2155
    @mamediarradieng2155 3 роки тому

    Ah Pape Niang yalna la yalla gay sa khôl ligay def guisna ko bilay souma yalla mayon hewal dinay dougal sama lokho wayé yalla bakhna yalla samoulza arla

  • @fatoudiedhiou4508
    @fatoudiedhiou4508 3 роки тому +10

    Machallah ndeysane yalla bakhna 😭😭

  • @diopfatou1308
    @diopfatou1308 3 роки тому +1

    Mashala yalla nalene yalla fay si barke seydina Mohamed

  • @dioumadione1144
    @dioumadione1144 3 роки тому

    Pape yalla na leu yalla fey thii barke reussourilah

  • @Aisha-rj4up
    @Aisha-rj4up 3 роки тому +2

    Xalé yi yalla naléne yalla may goudou fane ak wére si barki seydina mouhamed

  • @aidagueye6765
    @aidagueye6765 2 роки тому

    Pape Niang yalla n'a yalla goudal sa Fann thie barkep SERIGNE TOUBA'''MBACKE'

  • @marilandiaye1627
    @marilandiaye1627 3 роки тому

    Machallah yalna yalla féye sa khol pape niang

  • @khadygueye-ol2vm
    @khadygueye-ol2vm 3 роки тому +1

    Machalah Pape,goor rousna niane , yalla rek molaye faye inchallah

  • @kingdiaw9075
    @kingdiaw9075 2 роки тому +1

    Wa émission bi yaonaguénefi yague thé wérr machaalah

  • @mamadoumbengue3545
    @mamadoumbengue3545 3 роки тому +2

    Pape Niang yalla nala yalla fay yiw thi barké seydina mouhamed psl amine reuy nathi man damaye nian yalla mou May ma louma mana dimbalé niga khamné malén tané

  • @alimatousow4059
    @alimatousow4059 3 роки тому

    Kou fatou Diop gningue di sa yaye so bakhoul niou lath lako yalla na yalla guoudal sa fane

  • @aidakebe8221
    @aidakebe8221 3 роки тому +1

    Machalla pape

  • @mariediop9233
    @mariediop9233 3 роки тому +34

    Longue vie a les bb et toute la.fammille Que dieu vous protéges

  • @laminediatta2287
    @laminediatta2287 3 роки тому

    pape yake sa équipe yallah naléne yallah same yok soutoura yok tawhfeekh yok wheur guou yaram bi guoudale séne fane macha Allah amine yalna yallah same

  • @ndeyesamb3281
    @ndeyesamb3281 3 роки тому +5

    Thiey adouna loumétti yagnafi yalla naleen yalla taxawou sibarkép s saliou 😓😓😓

  • @ngodewonegueye7554
    @ngodewonegueye7554 3 роки тому +21

    Machalah pape immense gratitude à vous yalnalene Allah fayale bopape ci barke Seydina Mouhamed(psl)

  • @diabousakho5845
    @diabousakho5845 3 роки тому +1

    Papa niang dall yalla nalla yalla fay sa xole bou rafétt bi lolou macha allah may ndiabott gou barkél 🙏barké naby moustapha psl❤

  • @fatoumatabinetathiam9443
    @fatoumatabinetathiam9443 3 роки тому +1

    Walahi Pape Niang yaguu Def Lou reuye mâcha alla yalla n'a yalla goudeul sa fane mayla werr

  • @madamendiaye5963
    @madamendiaye5963 3 роки тому

    Pape ya worone nèk sounou prèsident de la rèpublic yalla nala yalla faye

  • @awakane2384
    @awakane2384 3 роки тому

    Ndeysan yalla naléne yalla fay yokou léne baguene ame ay milliard diapalé ay néw dji dolé

  • @diengtima4976
    @diengtima4976 3 роки тому +1

    Machallah baye pape Niang yalla nalene yalla takhawou

  • @kyabve2509
    @kyabve2509 3 роки тому

    yalla nalenn yalla fay bly doolen meusseu dannou👍yalla naniou yalla may moudiou bou rafett

  • @madjiguenediop6541
    @madjiguenediop6541 3 роки тому +21

    Oooh Sama khôl dafa séed trop sakh billahi quel beau geste noble pape yag fy lol ak sa équipe et aussi wa Dakar buzz🙏

  • @mbissunesow8233
    @mbissunesow8233 3 роки тому +4

    Pape ak fadel boulene yalla fayé digen kontan🙏🙏

  • @mariamacisse3831
    @mariamacisse3831 3 роки тому

    Machalla yalla nala borome bii fayyy sama xol sedd na ci iow

  • @amigaye8845
    @amigaye8845 Рік тому

    Yallana yalla fay dafala jam samala arla yirr ❤❤❤❤❤

  • @Marieseck534
    @Marieseck534 3 роки тому +2

    Pape Niang il faut que ngua bokeu thi listou député yi comme mairie yi wéssounaniou. Li la askann wi sokhla🥰🥰🥰 dieureudieufé Niang

  • @aminatafall3872
    @aminatafall3872 2 роки тому

    Machalla merci pape niang ak sa équipe yalla nallen yalla fay yalla n'a yalla yeureum yayou bébé yii yalla n'a yalla ték lokho ndiabott guimoufi bayi si barki seydina mouhamad (psl)

  • @fatoumbaye2172
    @fatoumbaye2172 3 роки тому

    Yane na ko yalla yeureum ta kharé ko aldiana soufe oyoff si kawame malaka yermané térou amine 😭😭

  • @diarrader8805
    @diarrader8805 3 роки тому

    Pape dieureudief waay sa dieyfdji raféte /(Yalla) nala fay

  • @mamediarafaye8751
    @mamediarafaye8751 2 роки тому +1

    Tonto pape yalna la yalla fayla Amine yarabi 🤲😭

  • @mamegayekane3898
    @mamegayekane3898 3 роки тому +5

    Thiaye yalla Soma amone khalisse Wala sama mak am ko 😭😭kone dé kene do diakhle

  • @cheikhmariemouseck2327
    @cheikhmariemouseck2327 3 роки тому

    Machalah quelle référence pape niang sama gayi bilahi ligéye bi rafét na yalla naléne yalla takhawou

  • @sadiocamara7338
    @sadiocamara7338 3 роки тому +1

    Machalah yalla rék mo lay fay inchalah

  • @modouthiam9333
    @modouthiam9333 3 роки тому

    Pape niane yalla guiss nala ya rék mon mo am se fay yalla na la fay

  • @ismailadieng2128
    @ismailadieng2128 3 роки тому

    Papa niang yalla na ko yalla takhawou ak gnimou ko hadal

  • @thiaragueye7845
    @thiaragueye7845 3 роки тому

    Pape Niang yalla nala yalla fay

  • @cheikhahmadoubamba9391
    @cheikhahmadoubamba9391 3 роки тому +1

    Vraiment sama hol dafa togne wadji yalla nako sounou borom fay holam
    Bébé yalla nanou dounedou baye diagal s'en yaye ay camil alhouranoul karim yalla nalé sounou borom ték loho

  • @antakebe689
    @antakebe689 3 роки тому +2

    Pape niang yalna yalla fayyla yiww et longue vie aux bb yalnagnou doundou té barkél inchaalah gnépp féké séne ndiarigne ,yalla kharé aldiana séne waydiour

  • @mmefaye230
    @mmefaye230 3 роки тому +47

    Pape ya warone nek ministre de la solidarité national
    Puisse Dieu te le rendre au centuple par le nom
    Puissant de Jésus Christ 🙏🏽

  • @fatoumbaye2172
    @fatoumbaye2172 3 роки тому +1

    Bébé yi yane nagne doudou ta barkél niou mague ak diamou machalla

  • @MameDiop-ow3ts
    @MameDiop-ow3ts 9 місяців тому

    Bilay gui yalla dinala fay sa xol barké serigne babacar li titou yalla rek moko meun❤❤

  • @sidykebe1192
    @sidykebe1192 3 роки тому +1

    Macha Allah pape gnang ligueye bi rafét na

  • @mouhamedcisse9708
    @mouhamedcisse9708 3 роки тому +1

    Bilahi pape niang yalla nala yalla fay sa xol rk😥

  • @doguisow5802
    @doguisow5802 3 роки тому

    Machaallah papa niang yala nala yala fay te yokala dundal sève yi

  • @collendiaye5296
    @collendiaye5296 3 роки тому

    Pape niang jerejef c'est ça le développement yalla na la yalla defal jamm.

  • @tidasagna6647
    @tidasagna6647 3 роки тому

    Pape yalla nala yalla dolén borom alal yi dèf lén thi gni

  • @fatimasogue4380
    @fatimasogue4380 3 роки тому +7

    Pape niang lingey def ni si lou baax yalnaleu ko allah feyyal bopam ba ngeu guiss si seu bop inchalah kouley setann rek xollam dineu toyy wayer dineu sedd trop vraimen yalneu yala feyal leu bopam inchalah🥰

  • @maevaalboury1712
    @maevaalboury1712 3 роки тому +2

    Un bienfait n'est jamais perdu Pape Niang yalla nala yala dimbeulé. Bilaye Pape yala dinala may dome in challa.

  • @abyndiaye2886
    @abyndiaye2886 3 роки тому

    Salam machallah sama nidiaye Niang balo geste bi yallah na yallah goudal sa fane ta wéral sa aye thieur gua yagué fi lol ta and akk wér Amiiiine inchallah 🙏🙏

  • @maguetteseck1351
    @maguetteseck1351 3 роки тому

    Yalla nala yalla faye sa khole ya rabi ta doundal khalé yi ya rabi

  • @ndiomendiaye6423
    @ndiomendiaye6423 3 роки тому +18

    C'est pas facile de faire des bonnes choses vraiment qu'Allah veille sur toi et te protège

  • @ndeyekhadyniang2288
    @ndeyekhadyniang2288 3 роки тому

    Pape Niang yala miame faye yalnala yala Faye li métine yalnako yala kare Al diana fir dawsi khaleli yala Nanou d'où te néke magoume lisslame

  • @aichadiaw4405
    @aichadiaw4405 3 роки тому +2

    Yallah nalén yallah fay sén dieuf you rafet 🤲🏿

  • @focus22599
    @focus22599 3 роки тому +3

    Ndékété Sénégal ba légui mogui am gnouy deff lou bahhe té yalla rek tahe

  • @fatougayeelementmamemakhta774
    @fatougayeelementmamemakhta774 3 роки тому +3

    pape niang yalna la yalla diapale yak sa ikipbi vraiment Sénégal bou amon deux you melni ioe Sénégal bakh 💝💝

  • @sodakane3805
    @sodakane3805 3 роки тому

    Pape niang yalla na la yalla faye sa kholou or bi , yalla na la yalla maye toute tanke

  • @serignendiayebeuguefallou7088
    @serignendiayebeuguefallou7088 3 роки тому +2

    Machala Pape Niang yaw ya bakh deugue bilahi

  • @seynaboundiaye7224
    @seynaboundiaye7224 3 роки тому +2

    Machallah 😍😍Mane sama yaye am na comme li 3 même jour 😍😍

  • @mameoumydiene537
    @mameoumydiene537 3 роки тому

    Pape niang yén na la yalla may khéwal guou sawane bawane si mbarké nouroudarayni

  • @kumbajagne2024
    @kumbajagne2024 3 роки тому +4

    Pape Yalnala Yallah fey!

  • @sowissa6044
    @sowissa6044 3 роки тому

    Pape inchallah yalla dinala tey loho contane naniou trop si yow mérité emission télévision national bi nieup boka ma niane si magou yalla mou lahala fou yaha yegoul pape nieup fière si yow ndah lou nieup war couca warlo warnanioula nianale 🙏❤

  • @mananaye2615
    @mananaye2615 3 роки тому +1

    Pape Niang,pape Niang,pape Niang ,yalla nala yalla takhawoula samela ak sa équipe, Allahuman amine,Ak Fadel

  • @jukanjie7562
    @jukanjie7562 2 роки тому

    Pape Nyang i always followed you at youtube may Allah's blessings 🙌 be upon you and the people that surrounded you all especially those that are behind helping the poor people 🙏

  • @youssoufabdoulayediopjohnn3774
    @youssoufabdoulayediopjohnn3774 3 роки тому

    Khamgua Kii Fadel Kokou mom bilahiii khamoumako wayé damako beugg rekk teh mom ak equipe DakarBuzz Mantion a Pape Niang marido de Fatiñaaa Big Up Mate

  • @maremegueye9946
    @maremegueye9946 3 роки тому +3

    Machalla machalla machalla pape nala yalla Faye sa khôl bou bakh inchallah si barke seydina mouhanet psl Amine ya Rabi

  • @meresow5894
    @meresow5894 3 роки тому

    Pape Niang goudou fane AK weer la gnou laye gnanal Niang

  • @awasylla6160
    @awasylla6160 3 роки тому

    Pape yalla na yalla Faye la ake kepe kouye defe lou bakhe yalla na yalla diapale wa ande takhawou dolelene si barck yalla

  • @yacinesarr4870
    @yacinesarr4870 3 роки тому +2

    Pape Niang yalla nala Yallah faye ak képe kou nécke thi sa guinawe

  • @serignetoubark
    @serignetoubark 3 роки тому

    Machallha rafti Tina wallahi hasim yalla n'a yalla samou len sotoral len Arlen barckep chekhol khadim

  • @awafall4293
    @awafall4293 3 роки тому +6

    Machala pape toujours au service de la population merci

  • @fatimakebe3040
    @fatimakebe3040 3 роки тому

    Ndeysan yalla na yall barkel len

  • @mbathiofall262
    @mbathiofall262 3 роки тому

    Manchalla pape Niang li dafa dawe yaram vraiment yalna yalla faye la sa dieufe dji rafétna trop

  • @docteurkb5342
    @docteurkb5342 3 роки тому +2

    Plus aide les gens plus Dieu tédde Bonne continuation frr moi je suis fiér de toi barké Serigne touba wala Hi sama kholl dafa sédde si iow😍

  • @emiliecisse6579
    @emiliecisse6579 3 роки тому +6

    Longue vie aux bébés ! Pape que le bon Dieu te protège et te bénisse

  • @malangdieme9076
    @malangdieme9076 3 роки тому +1

    Vraiment c triste puissance a tw pape mon homonyme ke Allah vs protège amine

  • @alaloubayefallbifirdawsidi573
    @alaloubayefallbifirdawsidi573 3 роки тому +34

    Ndeyesane machallah longue vie aux bébés yalnane doundou té barkel alahouma amine sene yaye yalna khipédji aldiana firdawsi firdawsi amine pape niang yalnalene yalla faye amolene morom walahi 🙏🙏🙏

  • @yacinelo930
    @yacinelo930 3 роки тому

    Merci Pape Niang yagui defale yalla té yalla rek takh yalla nala yalla fayal bopam

  • @ndeyembeneniang3204
    @ndeyembeneniang3204 3 роки тому

    Pape niang mane dé maguilaye nianell ak képp ko bokall di loguéyy long vie yokk ba yégko mane dé barké serigne saliou damaye niane yalla mou défma milyadére wayee sou Boba yalla bouma Dethie daraa lounite soklaa dé diokoumakoko bilahiii

  • @teyba1928
    @teyba1928 2 роки тому

    Vive pape Niang inchallah dieu vous récompensera

  • @mohameddiop5102
    @mohameddiop5102 3 роки тому

    pape niagne yanlana yalla motali sa yena si barke saydina Mohamed amine

  • @nogayefall2556
    @nogayefall2556 3 роки тому +13

    Yalla na yalla faye si barkepp Mouhamet cette femme quelle repose en paix 😭😭

    • @mameawadiaw7453
      @mameawadiaw7453 3 роки тому

      Mashalah yallana la yalla Faye pape yayou khalėyi yalla nako yalla yereum