Auto bu wara yap 63 personnes nga def thi 83 personnes bu niaff feh ndeyam thi Souf, chauffeur bi lah ak clients yiko nagou, Sénégal vous êtes pas des animaux 🇸🇳🇸🇳☝️ paix à leur âme et bon rétablissement aux blessés 🤲🤲😢
Au lieu gno gnou wakh deug chauffeur yi no il dit k Talli bi daffa khat ,Talli bi dafa ame rap ,dogollou yalla la ki dée perte motakh déme léne ci dem dikk ou bien Salam transport gnognou guissou niou Talli bou khatt guissou niou talli bou ame rap Sénégal problème comportement rk mo fi ame lep guiss na co li xew sama canam j'étais sur le demdikk Paix à leurs âmes
C toujours de la faute de Dieu c jamais le sénégalais, dites au chauffeur d’être sage sur la route de rouler avec sagesse et prudence surtout quand il pleut, mais le sénégalais ne connais pas ça lui c tjrs comme dab yalla bakhna en faisant sa betise
Tu a raison yallah dey dogal mais aussi chauffeur bus yi warnegn wakh ak niome bilahi walahi respecter wouniou dara loulen nekh lagni def teksi donio rew
Bayilene ndogal sounou borome, chauffeurs ame nagnou thi une grande part de responsabilité. Ils ne respectent jamais le nombre de personne qui doit se trouver dans le bus, ils ne dorment pas assez, ils roulent très vite.
Yalnaléne sunu Borom yeureum kharéléne Aldiana firdaws, à mon avis la solution pour diminuer drastiquement les accidents de la route au Sénégal 🇸🇳 c'est le rétablissement du réseau des chemins de fer sur toute l'étendue du territoire. Le train est la solution pour un transport sécurisé et confortable pour le bien des personnes et des marchandises surtout dans un pays où la ya bcp de commerçants
C'est tour la faute de dieu pour disculper le chauffeur certaines personne comme celui qui dit avoir reçu le coup de file du propriétaire du Bus . Témoin qui fait parti de cette accident a dit que le chauffeur roulait trop vite donc la faute est d la responsabilité du chauffeur . S'il avait respecté les consignes de sécurité Routière cette décompte macabre ne se résumerai pas à plus de mort . Si les usagés , les voyageurs ne s'implique pas le problème ne pourra être régler, il y vas de leur sécurité les usagés devrons après avoir constater qu'un chauffeur est imprudent alerter la Police Routière , tant que les voyageurs sont passif nous continuerons a compter des accidents .
Tout ca c l indiscipline des chauffeurs et la vieillesse des bus regardez l etat du bus qui est reduit en un amas de feraille ils devraient interdire des bus aussi vieux de rouler
C'est vraiment triste bilahi j'ai perdu mon cousin de dans que firdawsi soient leurs demeures éternelle 😢😢
Par bi wakhna deugue talli Dakar d'ar dafa khate torop yalla nalene yalla yeureum té kharelene aldiana si barke seydina Mohamed😢😢😢
Amine inchallah
En effet fii mou danélé bokou n'a ci cause accident you bari parfois tu es obligé descendre une roue
Amine ya rabbal alamin
Amine yalla nalene yalla yeureum
Auto bu wara yap 63 personnes nga def thi 83 personnes bu niaff feh ndeyam thi Souf, chauffeur bi lah ak clients yiko nagou, Sénégal vous êtes pas des animaux 🇸🇳🇸🇳☝️ paix à leur âme et bon rétablissement aux blessés 🤲🤲😢
Au lieu gno gnou wakh deug chauffeur yi no il dit k Talli bi daffa khat ,Talli bi dafa ame rap ,dogollou yalla la ki dée perte motakh déme léne ci dem dikk ou bien Salam transport gnognou guissou niou Talli bou khatt guissou niou talli bou ame rap
Sénégal problème comportement rk mo fi ame lep guiss na co li xew sama canam j'étais sur le demdikk
Paix à leurs âmes
C toujours de la faute de Dieu c jamais le sénégalais, dites au chauffeur d’être sage sur la route de rouler avec sagesse et prudence surtout quand il pleut, mais le sénégalais ne connais pas ça lui c tjrs comme dab yalla bakhna en faisant sa betise
Dioume gua dh ligua wakh reuy na yalla defoul betise dh li da warona am rk gua balma si niak mandou bi nk
Tu a raison yallah dey dogal mais aussi chauffeur bus yi warnegn wakh ak niome bilahi walahi respecter wouniou dara loulen nekh lagni def teksi donio rew
Paix à leurs âmes 🤲
Ndeysane yalnalene yalla yeureum
Ndeysane sa se voit kil est envahi par la panike c'est triste mais niakenaniou sounou free bou bakh papa😢😢😢😢
D c'est vrai ndogal yalla âme na mais les chauffeurs sont indisciplinés
Ndeyssane mettina paix à leurs âmes
Bayilene ndogal sounou borome, chauffeurs ame nagnou thi une grande part de responsabilité. Ils ne respectent jamais le nombre de personne qui doit se trouver dans le bus, ils ne dorment pas assez, ils roulent très vite.
Dafa yomb dé Lou âme rek gnou tek ko ko
Képou kousi fatou yalna ko yalla yeureume si barké moukhamét dou salalawou takhala
Bilay li pabi di wakh deugeuleu taly ndar Dakar daffa khatt
Bokou si taly you ndieuk senegal
Ndaysannn qu’il repose en paix
Paix a son âme 😭😭😭😭🙏🙏🙏
Borom bus yi douniou daw ndank ils font la course motah jamais ma yek bus 🚌
Yalnaléne sunu Borom yeureum kharéléne Aldiana firdaws, à mon avis la solution pour diminuer drastiquement les accidents de la route au Sénégal 🇸🇳 c'est le rétablissement du réseau des chemins de fer sur toute l'étendue du territoire. Le train est la solution pour un transport sécurisé et confortable pour le bien des personnes et des marchandises surtout dans un pays où la ya bcp de commerçants
Yalla naléne yalla yeureum mais yaradikou gissi tally mi je m'en foutisme il faut gnou remédier si
Yalla na aldiana dissén keur 😭😭😭 metina trop sakh
Li Metina way.di massawou mbok victimi yi yep di gnanal gnissi gagnou yalnalen yalla yeureum té diegal len
رحمة الله عليهم
C'est vraiment triste
S il pleuvait, le conducteur doit diminuer la vitesse, puisque la route est glissante.
Diminuer la vitesse ou s’arrêter même jusqu’à ce que les conditions de conduire s’améliorent
Les règles de conduite en période d'hivernage bilahi, si la visibilité n'est pas bonne il faut s'arrêter et bien se garer
Ho sounou papa semna😢khôl yeup toye fouta est en deuil
Yalnalène yalla yeureum
Yalla naléne yalla yeureum thé kharéko aldiana firdawsi
Yalla kharé léne aldiana
Macky sall talout yi dée ousmane sonko moko terè nalaw
Paix à leurs âme
Yalla yalla yeureum Lene thi barque Mohamed
Auto yi tam khot khassé leu maguette dara bakhousi
Nouveaux modèles mo guene doy wareti ay canettes kécé la bouci def accidents nore ba diekh , toubakh dafaratougnou auto bou degueur
Yallna yalla yeureum leen dogalo yalla deug la waye auto yi dara bakho ci tali tamit xatt na Bari ay cambo
J’ai perdu mon père dans cette accident
Massa Shry yalla nako yalla yeureum 🙏
Paix à son âme
Les voyageurs comment pouvaient prendre une voiture pareil
Oto yi daniou magat trop
C'est tour la faute de dieu pour disculper le chauffeur certaines personne comme celui qui dit avoir reçu le coup de file du propriétaire du Bus . Témoin qui fait parti de cette accident a dit que le chauffeur roulait trop vite donc la faute est d la responsabilité du chauffeur . S'il avait respecté les consignes de sécurité Routière cette décompte macabre ne se résumerai pas à plus de mort . Si les usagés , les voyageurs ne s'implique pas le problème ne pourra être régler, il y vas de leur sécurité les usagés devrons après avoir constater qu'un chauffeur est imprudent alerter la Police Routière , tant que les voyageurs sont passif nous continuerons a compter des accidents .
Cet accident n'a rien à voir avec dieu,on aime trop les raisonnements enfantins.le seul fautif,c'est l'idiot qui conduisait ce bus.
Si la yam juste bobou kéne nékoufa wayé lou mété nonou kéne meusouko guisse gnissi gnake séne bakan yallah naléne yallah yeureum
😢😢😢
Yalanagnou hipè aldjana firdawsi
Tout ca c l indiscipline des chauffeurs et la vieillesse des bus regardez l etat du bus qui est reduit en un amas de feraille ils devraient interdire des bus aussi vieux de rouler
Gni ci gnak seen bakkan yàlla naleen buur yàlla yërëm té xaare leen ci Aldiana you gëna kawee ya ñu ñu fa fekk ak ñu leen fa fekk
Embéssil bayilene ndongal europe rek mo ame ndongal mé senegal rewanedé mofa ame
A chaque fois niou def concer caserole accident am yalla naniou mouseull
Paix à leurs âmes
😢😢😢😢😢