Moom dadul taaw sax té du doom bah xeccoo ak ndondoo Kii kay daa am luko yeketi ci yoon wi té mingi ciy dox bu baax Réaction nak du lukoy wogni du waagni, action rék Zaahirikment nak, baatinikment dooga gnew
Vous passez tout voz temps a parler de cette dame.si elle n'est plus important que vous. Taisez vous donc.vous êtes entrain de rendre Aida mieux vous parlant tjour d'elle.
Thieuy aida yoora Tina beuzz magal gui rék 😂😂aida mi setane la des
Machalha amna solo
Bilahi négocier dafa barii
Merci beaucoup à Aïda Diallo long vie à toi merci beaucoup
Merci way 👍👍
Bayi lééne sokhna aida Diallo mou magal com niépou adouna amoul solo diamou rék
Dieureudieufé Serigne Touba
Delene ligueye te baye sokhna aida diallo
🙏🙏 ndigualou kilifa dieufé rek
Magal gui yalla na gnou ko yague téwé
Mane mome nékhale biguene koye nékhale rére moma méti
Sokhna Aida Diallo fait le buz. Djiguene bou moune gor
❤❤
Machallah amna solo lol serigne khadim
Aida Diallo nafeikh yi reike niokoye soutenir mais mome mola gueune khamni neikoul thi deugue.
Sokhna Aida saliou yagfi lollll
Kilifa dafa ame solo
Aida diallo yaw bouma LA amon ba Kate LA Kate you nekhe ak sa data bou sakh talibey Aida diallo yi data m rek lagnouko topé
Aïda dafa yabaté
Ibliss moy aida diallo. Ki dou nitou dara
Moom dadul taaw sax té du doom bah xeccoo ak ndondoo
Kii kay daa am luko yeketi ci yoon wi té mingi ciy dox bu baax
Réaction nak du lukoy wogni du waagni, action rék
Zaahirikment nak, baatinikment dooga gnew
Aida dafa defene chek betho mo sos yon yui aida da amoul mbek you wak degue yaw mbake mbake you djigene ya gui tok dal yaw nga diem fane do yen
Ban dikal lay diafé topou sam dou forsou kanan yaw may khéyam daka kham lafay khéw
Vous passez tout voz temps a parler de cette dame.si elle n'est plus important que vous. Taisez vous donc.vous êtes entrain de rendre Aida mieux vous parlant tjour d'elle.
bayi len aida diallo defoul dara lou ay limou yor mogui si dimbali new dj dolé yi