Mane deh le jour où j'ai vu cette 2em foto du cheikh si jp l'appeler ainsi Lima done yeuk batay mounoumako expliquer barker serigne touba. Djeureudjeuf Mbacké
Moi en ma croyance c'est c'est Cheikh ahmadou BAMBA. DIEUREUDIEUFÉ SERIGNE TOUBA CHEIKH MOUHAMADOUL MOUNTAKHA BACHIR SAMA SERIGNE YALNAFI YAGUE LOOL TÉ ANDAK WËR BIDIAHI NABIL-IL MOUSTAPHA BARKÉ CHEIKHOUL KHADIM AMÎNE 🤲🤲🤲
Mé franchement li diaroul wone saax ay débat. Té saax li dafa wara nék mbékté si ñioune gui niou xam ni ki mooy serigne touba moy ki démoone thia gueudj nga ki mom diamarlo wone ak toubaab yi
L islam mo amati ndam mame Bamba lakhou ba am tèmèri at you manké diourom niaar nit gni di weranté ay fotom kou sella rek mokoy am waay diarama waay sounou maam yalna yalla taass niou sa barrke ak kep kouni amiine
Khadim Rassoul amoul natale Ali mou andone ak Seydina Mohamed amoul Wone natale wakhotouma Cheikh Ahmadou Bamba lumière bi dane guene sene djieum nite entanouko
Da mélni xamoulén toubab yi att yin nék ak segn bi ta doun am Ay photoom lolou xél nangou wouko sakh video sakh toubab yi yor bagn ko xana Kay guéné ko da nékoul s'en engrangemen r
Serigne wxoul keen neko bene photolame thi adoun boxole bakanbi ak nioudoudi ak dihame bou leer bi gneu xamne momla nite amoul intere Di falcfier diemi serignbi bouniou kena ray ak aye expert photographe
Je sens au fond du cœur que c notre Cheikh
Mane deh le jour où j'ai vu cette 2em foto du cheikh si jp l'appeler ainsi Lima done yeuk batay mounoumako expliquer barker serigne touba.
Djeureudjeuf Mbacké
Meme diouli gueg gui toubap yi foto nan ko mais nit kou gnoul douko mosa guis dankh sen defet bignou am si serigne bi lay confirmé
Voilà 🥰
Cey ndeysane lolou kayy nagn khaar euleuk rek
C'est lui et c'est magnifique ♥️🙏
Excellent demonstration. C'est bien real Mame borome touba. Ya pas mal d'archives cachés par les blancs.
Moi en ma croyance c'est c'est Cheikh ahmadou BAMBA. DIEUREUDIEUFÉ SERIGNE TOUBA CHEIKH MOUHAMADOUL MOUNTAKHA BACHIR SAMA SERIGNE YALNAFI YAGUE LOOL TÉ ANDAK WËR BIDIAHI NABIL-IL MOUSTAPHA BARKÉ CHEIKHOUL KHADIM AMÎNE 🤲🤲🤲
Lousi mounta am Kou tedd ki mogui si xol yi pointe
Yalla nafa sah te dara douko fa dieule
Serigne touba est une femme point et rien ne pourra écraser cette vérité
@@Aby1947 boko touboûl dou bakh si yaw
ndeysaane serigne Touba😭😭♥️
Serigne touba Amna lépou yalla nalla yalla faye mane photo bi guisnako bou yague wayé ki serigne touba la ❤
Mashalla contane nagn trop si leeral bi
Dieureu dieuf serigne Touba minou khamal yalla ak yonène spl
Spl moy lane ??😂
Mé franchement li diaroul wone saax ay débat. Té saax li dafa wara nék mbékté si ñioune gui niou xam ni ki mooy serigne touba moy ki démoone thia gueudj nga ki mom diamarlo wone ak toubaab yi
Kay degue wadiagui de ki diakhal adduna diomal toubab yi Saveur niou Ahmadou dieuredieuf 🙏🏾
Walahi wakh ngua deug
Serigne touba est une femme point
Macha allah xam xam reka wôor il y'a même des vidéos de Serigne Touba détenu par les tuubab un jour viendra ils vont tout révéler incha allah
Dème sétane serigne amadou Ndiaye nguérane kokou mome deugue lay nétali
😢😢😢😢😢
Ma Cha Alla.Avec cette photo il y a vraiment un sentiment de Serigne Touba
L islam mo amati ndam mame Bamba lakhou ba am tèmèri at you manké diourom niaar nit gni di weranté ay fotom kou sella rek mokoy am waay diarama waay sounou maam yalna yalla taass niou sa barrke ak kep kouni amiine
Nous avons tous que c'est Borom Touba ❤
Dieuredieuf serigne Touba
C’est bien serigne touba et y’a n’a d’autre photo
Ndeysane thieyy kou bakhhh ki ❤️❤️❤️
Si je pouvais être le disciple " talibé "de S TOUBA.
Qui voulait l'être ?
Fait le djebalou
Dieura dieufaty serigne touba
Dieredieufeuti cheikh Ahmadou bamba
Lide dara ganokoo liirr
Mai wadji diambar le
Entouka déh yok léen guestu boubakh si centre archives internationales !!! Toubab yi lougnou dénthie beurina
Khadim Rassoul amoul natale Ali mou andone ak Seydina Mohamed amoul Wone natale wakhotouma Cheikh Ahmadou Bamba lumière bi dane guene sene djieum nite entanouko
Akassa mame bamba rek
Kou bakh ki❤❤❤❤❤
Paroles d'experts.
Machallah
Macha ALLAH
Dommage que ce ne soit pas traduit en français.
Diangatt bu am solo loool
Da mélni xamoulén toubab yi att yin nék ak segn bi ta doun am Ay photoom lolou xél nangou wouko sakh video sakh toubab yi yor bagn ko xana Kay guéné ko da nékoul s'en engrangemen r
Toubab yi yorr naniou sah vidéo wala photo bamouy diouli si géuth gui lou lérr lala wakh daniouy tokk beuss rek généko
Li mo weer nk
Amna niou ko mais danio banie défaite motakh douniou ko guénnè
Dieuredieuf mbacke
Man photo bi bimako gissé a la première fois lawakhni momla a moull wérénté ..waw loutakh Serigne bi waroull am benéne photo?
Daniou nio khamalone ne Serigne bi Foto douko diap
@@daoudabaohhelenewarimmermi6741 Kane mola ko xamal ?
Ler na bilaye
Hir yala bouléne niou yakal sounou fotobi
Ani poche bi🤔🤔🤔
Bamba dou morom
Liniou doon gis dembe dou photo
serigne bi rek Kaye serigne
toubab yi kou dèmone sen archive yi bilay ame nagne foto kou ted ki ak ay ecrit yi wame mè dougne ko doul guènè parceque toubab bougoul dèfète
Wallahi 🥰
Mashallah amna solo loool
CHEIKH AHMADOU BAMBA KEN LA il n'a pas de photo khadim RASSOULILAHI amoul photo
Enfin la vraie photo de Serigne Touba, le boubou blanc n'existe pas, c du photoshop !
Dè lène dèglou serigne ahmadou ndiaye nguérane kokou moy wakh deugue gni dess gneupp fène rekk lagnouy deff serigne touba toubab yi dagnou ko done malmené noumou lène nékhé
Ya meuneu doul
@@khadygueye4794 comme sa ndeye
Khady gueuye ki boko tontou WE daye âme louko nekh diarouko kene falewoul comenterame s Touba amoul morome kene la
On vas demande serigne mountakha rek mou leer
Waw kay
Serigne mountaha dou infographiste té fékouwoul mamam donc diapal thi wa dji
Bara ndiaye photobi kokoxol xamni serigne touba rekla ay imageame barina yagn
a ak toubabyi ndax imagou 14 18 batey moungufi
Serigne wxoul keen neko bene photolame thi adoun boxole bakanbi ak nioudoudi ak dihame bou leer bi gneu xamne momla nite amoul intere
Di falcfier diemi serignbi bouniou kena ray ak aye expert photographe
2
Dieuredieuf mbacke