Ablaye Diop Bichri "Wakhtane ci Serigne Saliou Mbacké"

Поділитися
Вставка
  • Опубліковано 10 лют 2025
  • #kebetu #team221 #senegal
    page facebbok : / senegal7officiel
    Abonnez-vous pour plus de vidéos et n'oubliez pas d'activer la cloche de notification

КОМЕНТАРІ •

  • @sambadiop9500
    @sambadiop9500 11 місяців тому +20

    Kou Serigne saliou beseul j'aime❤❤

  • @ColettejeantalNdiaye
    @ColettejeantalNdiaye 10 місяців тому +6

    Bilay dama ko beugu ba meunou mako expliquè
    Dieureudief Serigne Saliou
    Di nagn Yallah am dieukeur bou toudou Serigne Saliou🙏

  • @DNS756
    @DNS756 3 роки тому +16

    Dieuredieufa serigne saliou mbacke Yalla na yalla yokou aye lerame te tass niou si barkem 😍

  • @sokhnafatoufall9356
    @sokhnafatoufall9356 Рік тому +7

    Dieureudieufeté cheikhoul khadim ❤❤mome mignou bollék sougnou mame saliou amougnou thi mome saguoo😭😭 mbacké balla yagnou défar ték gnou thi yonn siratal moustakhim ❤ yalna yalla yokk say lérr té tasougnou thi sa barké

  • @kemvnendiaye600
    @kemvnendiaye600 4 роки тому +409

    Première commentaire gou beugue serigne Saliou rk beuseul j’aime

  • @ModouSare-i3j
    @ModouSare-i3j 8 місяців тому +5

    Ndeyesane kéne d'où Serigne saliou yalla n'a yala yokou ay lérame té tasse niousi barekéme ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @beihkinoushsamb2999
    @beihkinoushsamb2999 4 роки тому +9

    Machalah douma thi doyal thi as Salih diantub diamonom Mane deH damako beug mbacké Balla té guissou mala sakh wayé yalna niou tassé

  • @omarfall8271
    @omarfall8271 4 роки тому +82

    Thiaye serigne Saliou yalla na niou yalla doli tawfekh si mom

  • @souleymanediop5014
    @souleymanediop5014 4 роки тому +15

    Euskeuy machallah dieureudieuf serigne touba kenla amoul morom mbacke diarama mam cheikh Ibrahima fall lamp thiey serigne touba borom yeumeunde gui borom khelcom mbacke yallah nanou na yallah dayal si barke sì barke khadimou rassoul serigne mountakha mbacke yallah ngafi yague lol ta wer mbacke dieureudieuf serigne Abdoulaye diop bichiri akasa samb sounouy khôl said nalol ken dou serigne saliou mbacke yallah naou yallah tass si barkem mbacke yallah lalen serigne touba fay si barke yonantibi alay salatou wasalam si barke khasidayi Allahou ma amine dieureudieuf sen tv diadieuf bougane machallah

  • @fondationx77
    @fondationx77 2 роки тому +23

    Notre fierté serigne saliou💖💖

  • @koumbacke9731
    @koumbacke9731 4 роки тому +24

    Dieureudieuf serigne touba.sante serigne saliou mbacké

  • @aliouba8200
    @aliouba8200 4 роки тому +10

    Dieureudieuf borome touba diarama mame lamp fall Dieureudieufete serigne saliou mbacke yallana yalla fayalnioulene Co barke serigne touba

  • @mariamadiop6630
    @mariamadiop6630 4 роки тому +34

    Dieuredieuf sognou borom mom mignou barkèl S Touba ba thi S Saliou Mbackè

  • @amydabo6230
    @amydabo6230 2 роки тому +9

    Dieureudieufé Serigne saliou mbacké 😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭

  • @djibrilsima7660
    @djibrilsima7660 4 роки тому +35

    Thiey mbacké,borrom diamono...niogui lé dioye ba léguî nopé ngounou😭😭😭😭

  • @salioufaye6810
    @salioufaye6810 4 роки тому +111

    Alkhamdoulilah nous rendons grâce à Dieu de nous avoir donné Serigne Saliou

  • @LamineSar-kx2cw
    @LamineSar-kx2cw Рік тому +1

    Macha Allah Yalnaniou Yalla fayal s Touba

  • @bambaniang9305
    @bambaniang9305 4 роки тому +5

    Mach Allah serigne saliou yalna niou ko yalla fayale yoku leeram tass niou si barckem

  • @rokhiyatou4004
    @rokhiyatou4004 4 роки тому +26

    Sougnou thiofel si Serigne saliou gnoune sakh khamougnou foumou diougué koudoul yalla manoko kham 😭😭😭

  • @niangomar3213
    @niangomar3213 4 роки тому +9

    Dieureudiafati khadimou khadim nekhna trp masha allahhhhhh bichri khakham bi sellana

  • @yacineniang5776
    @yacineniang5776 4 роки тому +21

    Bichri Mala beugeu gire dieumi Serigne Touba🙏🙏

  • @sidymakhtar5021
    @sidymakhtar5021 3 роки тому +9

    Thiey Seringe saliou bala ayssa❤️❤️❤️😭

  • @magoumbambow6040
    @magoumbambow6040 4 роки тому +33

    Abdoulay Diop Bichri yague fi lool barké Serigne Saliou 😭😭😭😭😭

  • @awasaliouba7129
    @awasaliouba7129 4 роки тому +39

    Notre fierté Mame Saliou ❤️

  • @ousseynoudieng9083
    @ousseynoudieng9083 3 роки тому +6

    Nous t'aimons Serigne Saliou Mbacké amoul morom

  • @mamediarragning7303
    @mamediarragning7303 4 роки тому +14

    😭 lignou oumpalè si serigne bi barina

  • @salihatte9319
    @salihatte9319 4 роки тому +59

    Sama serigne la dieureudieuf mame boye🙏

    • @khadimdylla4477
      @khadimdylla4477 4 роки тому +2

      Yen jigeen yi ninguen moussé bayewoulen ken Serigne saliou😀😀😀

    • @mameboussocisse386
      @mameboussocisse386 4 роки тому +5

      mandé damay yakarné man rk mako begue nimako kén begué woukoko

  • @zeumthebosslofficiel1642
    @zeumthebosslofficiel1642 4 роки тому +20

    S.touba kénla.Kéne dou brome diamano s.saliou yaakari xalé yi😭😭😭😭😭

  • @kemvnendiaye600
    @kemvnendiaye600 4 роки тому +93

    Dieuredjef serigne Saliou

  • @fatoudioum7506
    @fatoudioum7506 4 роки тому +51

    Ma beugue Serigne Saliou

  • @jwrikfinii7021
    @jwrikfinii7021 4 роки тому +10

    SERIGNE SALIHOU MBACKE MOOY SERIGNE TOUBA DANS SA PURE RÉALITÉ DIVINE.
    SERIGNE SALIHOU MOOY SERIGNOU SERIGNE SI. MOOY YALLA SOUNOU BOROOM. MOMA DEI BARKÉ SERIGNE BETHIO

  • @laminebara1514
    @laminebara1514 Рік тому +4

    Santaty serigne Saliou Mbacké ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @mamediarradiop4677
    @mamediarradiop4677 4 роки тому +30

    Serigne BICHRI YALLA nangi fii yague taa werrr Lolll❤💕💞💝😭😭

  • @thiarrambp4321
    @thiarrambp4321 3 роки тому +16

    Macahlla ame na solo ❤❤❤

  • @djilydiop6812
    @djilydiop6812 4 роки тому +23

    Mbachalla dieuradieuf sama tourano kene dou mome

  • @modoulamine4521
    @modoulamine4521 Рік тому +8

    toujours dans notre cœur ♥️ 😢blh ioe rk Lagne kham serigne saliou 😭😭

  • @thianesene7624
    @thianesene7624 4 роки тому +10

    Thieuy serigne touba

  • @mamasow6124
    @mamasow6124 4 роки тому +13

    Machalla ablaye diop bichri
    Ken dou serigne saliou

  • @serigneseck4012
    @serigneseck4012 4 роки тому +23

    Bilahi taye contane na bassi Karamou yalla

    • @mamansarr1710
      @mamansarr1710 4 роки тому

      Sentv 2020 bi yenaye borom yenafii dakh plateau barki serigne salliou tele yeupeu bakh wayai rene gui rene gui sentv moko yorrr dieureudieuti serign diarawlakk mame chekh ibrahima fall lamp

    • @tallambaye9969
      @tallambaye9969 4 роки тому

      @@mamansarr1710 Nice

  • @abdouahadniang1928
    @abdouahadniang1928 4 роки тому +13

    Thiaye sérigne touba
    Buegue serigne touba

  • @m.k.g3046
    @m.k.g3046 4 роки тому +15

    Sounou Wadji Mame Saliou ❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️

  • @abdoullatifndiaye7428
    @abdoullatifndiaye7428 4 роки тому +61

    Serigne Saliou Mbackè jeureujeuf

  • @7753-t9i
    @7753-t9i 4 роки тому +12

    machaalla sama yakar s saliou ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @fernandmendy8650
    @fernandmendy8650 2 роки тому +2

    Mame saliou woo Mame saliou woo Mame saliou woo yay borom yeurmendéé

  • @omarsow273
    @omarsow273 4 роки тому +8

    Dieureudieuf Serigne saliou mbacké

  • @AboDiop-hj7fx
    @AboDiop-hj7fx Рік тому +3

    Diarama Serigne saliou ♥️♥️♥️🖤🖤🖤

  • @bayedarousopayboromdarouno6585
    @bayedarousopayboromdarouno6585 3 роки тому +1

    Ken dou s touba bayou s saliou yalla nagniou ko yalla fayal❣

  • @elhadjimomarsow8020
    @elhadjimomarsow8020 2 роки тому

    Dieureudieuf serigne Saliou yalla na sunu borom yokkou ay lééraam.
    Serigne a.Diop bichri wakhtaan bi am na solo.yall na sunu borom dolél sa takhaway.

  • @mariamadiop6630
    @mariamadiop6630 4 роки тому +15

    S Abdoulaye Bichri yag fi loll tè wer

  • @balladiop5469
    @balladiop5469 4 роки тому +13

    Serigne saliou ken la

  • @sheikh84mbengue48
    @sheikh84mbengue48 4 роки тому +1

    Bichri yalla gua fi yague tê weire amine Ya RABBI

  • @fatouba1587
    @fatouba1587 2 місяці тому

    Serigne saliou yana gnouka YALLA fayale, tassegnou si barkéme, bakhna trope trope.......❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @fatouba1587
    @fatouba1587 2 місяці тому

    Dieureudieuf serigne saliou, gneupe gnola beugue, je le sent dans mon coeur, yana gnoula YALLA fayale

  • @timfatoure1231
    @timfatoure1231 4 роки тому +10

    Machallah Serigne Saliou ❤️🙏❤️sama khôl Sedena 😭😭😭

  • @madagueye7251
    @madagueye7251 4 роки тому +48

    Serigne Saliou sama lépppp 🥰🥰🥰

  • @ndeyedieng5529
    @ndeyedieng5529 3 роки тому +1

    Thieye serigne saliou yalnaniouko yalla fayale

  • @fatimndour5350
    @fatimndour5350 Рік тому

    Dieuredieuf SERIGNE SALIOU MBACKE.yalla nagnou yalla Tass si sa barcké

  • @aliouneseye3688
    @aliouneseye3688 2 роки тому +3

    Machalla thieye mame Saliou ❤️

  • @NdeyeAwaDiouf-el6bv
    @NdeyeAwaDiouf-el6bv Рік тому +1

    Notre fierté Serigne saliou dieuredieuf Mbacké balla Aïcha 🙏♥️♥️

  • @maimounadoucoure6714
    @maimounadoucoure6714 4 роки тому +4

    Serigne Saliou mbacké yana yalla yokou ak léram amine

  • @SangThiaw
    @SangThiaw 7 місяців тому

    Yalna niou yalla sakhal si beug s saliou mbacké

  • @bambadiop2585
    @bambadiop2585 4 роки тому +23

    THIEY SERIGN SALIOU BOROM YEURMANDÉ ❤

  • @khadidiatougassama3822
    @khadidiatougassama3822 4 роки тому +1

    Ken dou Serigne saliou yalla na yalla yok ay leram

  • @mykakamara2311
    @mykakamara2311 Рік тому +1

    Thiey sama wadji santate na deh loumala sante Mbacké doyoul santate na ba sama taw iow lako doupé dou sama ngora deh sa dimbale rek Mbacké ak louniou meunoul wax yaniou teral,sagal niou soutoural niou dieuredieufety

  • @88etudient
    @88etudient 4 роки тому +5

    Serignou Ndaw gni baye saliou mbacke borom khelkom. Billa hi momme rek doyna ma serigne. Inchalah mbacke si sa tank rek lagnuy diarr

  • @massambasall8472
    @massambasall8472 4 роки тому +7

    Love You Saliha ❤️❤️❤️❤️

  • @pendasene9259
    @pendasene9259 4 роки тому +12

    DIEUREDIEUF SERIGNE SALIOU ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @nogayeseck5291
    @nogayeseck5291 4 роки тому +17

    Jeureujeufeti Serigne saliou 🙏✨

  • @falloufall6959
    @falloufall6959 4 роки тому +13

    Fier d'être mouride

  • @allahoumasaliallahseydinam5609
    @allahoumasaliallahseydinam5609 4 роки тому +9

    dieuredieufe serigne touba

  • @Sdia3067
    @Sdia3067 4 роки тому +2

    Serigne saliou mbacké moy Serigne touba barki Serigne saliou 😭😭

  • @elagendiaye7631
    @elagendiaye7631 4 роки тому +16

    Serigne Saliou kou sori thi ndaw yi

  • @saliousarr3417
    @saliousarr3417 Рік тому

    ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤ yalna niou ko yalla féyal si barké Muhammed psl

  • @saliougueye9410
    @saliougueye9410 4 роки тому +8

    Sante Yalla bima toné talibé s saliou

  • @YacineToure-nt6bn
    @YacineToure-nt6bn Рік тому

    Sama xoll sédna 😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭

  • @diorsalioudiagne4496
    @diorsalioudiagne4496 4 роки тому +29

    Serigne saliou mbacke sama serigne content na trop bichri baga toudé liguey bi waaw pikine di def si daara xelcom mbecté kep la mouride dé si barguelou ame na solo lol

  • @mortoure3254
    @mortoure3254 4 роки тому +3

    Dieureudieuf Serigne saliou mbacké amoull morome billàhi

  • @soguediop414
    @soguediop414 4 роки тому +9

    Thiey serigne saliou

  • @aichas4438
    @aichas4438 4 роки тому +6

    Thieuy serigne Saliou Mbackè

  • @fatmandb8319
    @fatmandb8319 4 роки тому +6

    Dieureudieufeti serigne saliou

  • @bambalayediop5510
    @bambalayediop5510 3 роки тому +13

    Machalla 💞💞💞

    • @modouwillane5975
      @modouwillane5975 3 роки тому +1

      Jtm s saliou bou bakh ❣️❤️💞

    • @GueyeMamadou-v1y
      @GueyeMamadou-v1y Рік тому

      ​@@modouwillane5975😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊

  • @mansourmbaye9551
    @mansourmbaye9551 3 роки тому +3

    Dieureudieuf Serigne Saliou💕❣️❤️

  • @Idyba233
    @Idyba233 Рік тому

    Serigne saliou mbacke sama Wassila yalla yalla yoki lérame❤️❤️❤️🧡🧡

  • @younoussakane3713
    @younoussakane3713 2 роки тому

    Allah Serigne Touba bakhe il est le meilleure machallah bamba rek j'aime beaucoup Serigne Touba bakhe khadimo Rassoul dieredieuf

  • @peneomar7202
    @peneomar7202 4 роки тому +2

    Ndeye san s saliou rek ba adiana

  • @falloufall1816
    @falloufall1816 4 роки тому +4

    Cheikh ibrahime Fall Lap baboule mouridine kéne dou mome Akssa ♥️🙏🏿

  • @Talibès.salioumbackèlayedonneb

    Dieuruedieuf s Saliou mbackè amoul morom mbackè mala beugg mbackè

  • @BayeYatta
    @BayeYatta Рік тому +1

    Alhamdou Lila dieuredieuf Serigne saliou ❤

  • @gallayendiaye1147
    @gallayendiaye1147 3 роки тому +3

    Machallah serigne abdou laye Diop

  • @modoundawgaye2303
    @modoundawgaye2303 2 роки тому

    Yalla Nanou yalla fewele ak saytane tee bolenok ch bamba fiil djinani

  • @mouhasow821
    @mouhasow821 4 роки тому +13

    Machallah bichri

  • @ngounembaye1112
    @ngounembaye1112 4 роки тому +12

    S Saliou Sama dopé bi

  • @saffdiagne1244
    @saffdiagne1244 4 роки тому +2

    Dieureudieufaty mame saliou boy thiey😭❤❤❤

  • @YacineToure-nt6bn
    @YacineToure-nt6bn Рік тому

    Tihay sariegne saliou sama yakarr dia❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @aMaDoUSY265
    @aMaDoUSY265 4 роки тому +3

    Borom Khelcom yalla nanuko yalla fayal

  • @IbouMendy-zs7ei
    @IbouMendy-zs7ei Рік тому

    Alhamdoulilah, ressanta ti Serigne Saliou mon guide spirituel.

  • @lotadiagne9437
    @lotadiagne9437 4 роки тому +6

    Thieuy serigne saliou borom diamono

  • @asssanengom3416
    @asssanengom3416 3 роки тому

    Dieureudizufety Serigne Saliou,Serigne ablaye yalnanoula Serigne bi fayale

  • @maxwane7371
    @maxwane7371 Рік тому +1

    Sante Serigne SALIOU ♥️♥️♥️🙏🏻

  • @aidambaye1257
    @aidambaye1257 2 роки тому

    Ken dou mome mame Saliou sunu yakar tay ak euleuk 💖❤❤💖