Meilleur des PDG moy nitte ki Walay nous ses employés amouniou sa fay bakh gua beugue guaniou âme gua sounou yeurmandé y’a takh niewouniou keine thiam diapé woniou employé mes des sœurs lou bakh rek guané nioune la yeiné bigua ame si nioune mane nane ko Seider devant tout le monde PDG bou bakh riche gueune bari yermandé Yako deff thiam ta générosité ta gentillesse sa tabé me dépasse Lo âme bokou guako ak nitte gni yalla nasa diamou yague yalla bo guis Dara lo ragal diodio glow skin si kaw si kaname rek inchallah 💪♥️♥️♥️Loune la wakhal rek si Lou bakh ame na Lou dess yalla nasa diamou yague ❤❤
MAME DIARRA THIAM YALLA NALA YALLA AAR , SAME , MAYE SOUTOURA AK DIAM AK KHÉWEUL AK MOUDJOU BOU RAFÈTE , FOULE LA THI KAW TÉ LAKH LEU FA YAAKH AGOUL SI BARKÉ NABI MOUSTAPHA SALA LAHOU ALEYHI SALATOU WA SALAM PSL . AMINE YA RABI NIOU BOK KO .
En tout cas mangui ni done setane émission bi pour terminer ko et jangu nassi Lou Bari beugue si femme bi t xamoumako mossouma tok dieul sama temps setane vidéo wam grâce à cette émission nak xamna ni nit kou bakh la kou am yeurmadé ak yiw longue vie Diodio bonne santé insha'allah 🙏 je te. Love ❤❤❤❤❤❤❤
J’ai mes larmes en regardant cette Émission de Diodio ce qui te tu pas te rends plus fort Tu fais ma fierté moi à 27 ans je parviens pas à rien réaliser mes rêves envers mes parents je t’estime pour cette grave Dame que tu es devenue Que dieu te garde dans cette vie aussi longtemps que possible
Elle m'a redonné le courage Yalla nala yalla fay Thiam Babel j'ai un enfant et j'ai que 22 ans mako yorre yore sm bopou sm Rak ak sm Yaye mais sante elle m'a redonné le courage Yalla nala yalla takhawou inch'Allah ❤
On dirait que tu racontes ma vie DioDio. Tu as relaté quelques passages de ma vie et je me vois dans ce confidence, Yalla na Yalla gueune la takhawou gueune la doléle boul tite boul ragal sa khol moy lampe biy léral sa yone. Khamoumala dé mais dangama méy fitt pour yone bima dieum ma niéméko khamni gueum sa bop ak Yalla diapaléla rék mofi nék donc chapeau bas à toi. Merci pour cette motivation que tu viens de me procurer. Mangui dounde instant bi lou métti té tar lolou mais béss bouma amé succés si yone bi ma beugueu dieul dina nieuw basi yow toudé la sama succés c'est une promesse té dinako tenir Insha Allah. ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤vive cette battante waye. Des ❤ pour Dio Dio❤❤❤❤❤
J’ai eu l’impression que c’est moi qui est assise à la place de Diodio tellement notre vie est identique commençant par le décès de sa mère chose que j’ai vécue et qui a fait de moi ce que je suis aujourd’hui. Tout coïncide avec mon vécu. Yalna yalla yok gneup inshalah.
Non man ngay wakhal surtout le décès de sa maman j’ai parlé avec ma maman à 8h 10h on m’appelle pour me dire que ma maman est décédé 😢😢😢😢😢 mou melni adina bi day danou sama kay
Diodio qu’Allah te préserve et te protège de tout mal ..c’est la première fois que je commente sur confidence mais saches que hormis ton entourage il y’a des gens qui t’aiment sincèrement et te souhaite que le meilleur Tu es ma référence wallahi et j’espère un jour devenir une femme indépendante, aimante tel que toi Ceux qui sont près de toi ont vraiment de la chance de côtoyer une personne comme toi Je te dis tout simplement mashallah et on n’est très fière de la femme que tu es devenu aujourd’hui ♥️♥️
Une femme de toute les qualités ☝️ wallakhi anzim c’est une dame de référence toute femme doit faire diodio comme référence car elle a traversé des moments misérables🥺❤️❤️Diodio man diamou yalla bi mangui lay gnanal guoud fan wer yokk ba gnoun gniy sétan diarignou thii diodio yalla bo guiss lo ragual🤲🏾🤲🏾diodio diam la la yéné diodio kholay wakhé guene nala beugue ndakh Diamou yalla yi guay rendre heureuse
Avec DioDio c’est une leçon de vie mes frères et sœurs levons nous dara dou diouk rek soti guem guem focus fierté sante yallah inchallah lepp di na bahh ❤
J'ai regardé l'émission du début à la fin avec des larmes comme Diodio il faut être une personne entière comme elle pour mieux comprendre la dame la actuellement je traverse des moments pareille que ses moments d'avant surtout bou waxé ni worna beu gone diot mou nane ndoh ak tantdarma c'est comme si elle était en moi mais alkhamdulilah natou metiwoul
Une émission a limage de la présentatrice et de son hote ( Niari MAME YI) -Mame coumba une dame simple classe et raffiné. Une personne humble douce et bien éduqué. Face a son invité Mame diarra Alias Diodio borom Diodio glow skin Une jeune dame oui tres jeune meme machallah Etre PDG dune telle entreprise etre la maitresse dune si belle reussite a son age n’est pas donné a tous malgres les difficultés de la vies et son jeune âge. Une femme forte avec du caractère chose qui lui a permise d’en arriver a ce stade mais en meme temps une dame pieuse et croyante un exemple pr les jeunes filles qui aimeraient réussir a la sueur de leurs front une bonne personne abec bcp de qualités tres humble et respectueuse douce machallah dal régler geum yalla tei diko diamou. Vraiment merci pr cette émission je pense que depuis kou nk diaarna fi mais par la qualité des paroles la douceur de l’une et l’autre vraiment bi mo dakh yeup❤❤❤❤. Merci a vois les Mame yeine la rew mi sokhla pr wane khaleyi yonou deugue bi yinou diamou yalla bi yonou liguey bi. Am leine diam
Meilleur des PDG bakh riche guenneu sama yaye djii yayou diodio ak papa madior yaww lii dou chance mèrite leuuu tèguèganiou yir ganiou diap ganiou topoto ganiou diapèwoniou employé mais sayy dôme gni sayyy sœur yaw madiodio sou diougater do dèfarate sa togay baby d amour kor ndiouga fall yakousi Dara diniou diapaler diniou conseiller Mme Fall kor ndiouga sama wadji l intellectuel des crèatrices des grandes entreprises et marque 🎉🎉🎉 au Sénégal 🎉🎉🎉❤❤❤❤❤❤
Jai jamais commenté Chapeau a cette émission mame coumba bravo encore cette dame de fer nous fait reve et d'aller de l'avant damakoy suivre rekk sur les réseaux mais nitee kou simple humble modeste bax labir nitou kesse yené gneup ame yeurmandé on sens son honnêteté quand elle parle machallah bonne continuation nga yokk ba yeuk ko aminn
Waaw je suis tombée amoureuse de la personnalité de cette Diodio Mashalla yalna yalla sameleu areleu soutouraleu motalli projets yi si barkei Serigne Babacar sy ❤❤❤
J’ai fais 3jour à regarder cette émission chaque parole de diodio me fait pleuré une personne plus que parfaite yallah na la yallah takhawo bayinala ak yallah mome mi diare denke ❤
Ndeysan sama fadiar jeudi ba je n avait que 11 ans may yéwo di lathie sama niouni ma sa yay décédée na. Ma oumou dort en paix tu me manque énormément 😢😢
WAAAAW, mais comment ne pas se confier a cœur ouvert face a une dame aussi charmante, correcte, accueillante et très a l'ecoute en plus le cadre est propice pour se confier. SOKHNA MAME COUMBA, merci! - SENEPOEPLE +, merci! - Mention Speciale a l'equipe technique! 🤍💯
Maa shaa Allah une dame pétrie de valeur ndeysaan ,nitte au vrai sens du terme la deglou taye ces ces personnes généreuse et empathique qu’il faut suivre sur les réseaux ,motivantes et source d’inspiration, kou goré rek moy geureum gniko diapale surtout ses employés force à toi diodio
C’est la première fois je regarde cette émission grâce a la femme battante Diodio la plus douce gentille ouverte d’esprit meilleure de ta génération je t’aime 🥰
Moi aussi c’est la première fois et j’en ai tiré des leçons sur tout. Je peux dire qu’on a le même parcours mais elle me redonne confiance. Bravo grand Dame. So much love ❤️
Vraiment geune nala fonk geune nala beugue bilahiii walahi quand tu parles de ta mère j'ai Les larmes aux yeux Mane mii nga kham ni téral sama yaye rekkk laa beugue mais j'ai pas encore les moyens mais yalla bakhnaaa Sokhna Mame Diarra Thiam DIODIO GLOW SKIN YALNASSA DIAM YAGUE ❤❤❤
Ay mame Diarra sama toma sama boukki bi mate nala mais yalla mofi né bo niaké yaye dara doula saf doto amati nakhar boula diakhal mais alhamdoulillah yalla mo niouko diokhone moko dieulat
🇬🇦 bonjour je suis gabonaise , je regarde toujours l’émission avec mon amie sénégalaise, ça me ferai plaisir si vous mettez la traduction en français s’il vous plaît car à chaque fois on est obligé de couper la vidéo pour qu’elle m’explique 🇬🇦❤️ je vous admire
Je pleure en regardant cette émission elle est vraiment une référence pour les filles ou garçon de ce monde soyez simple et partager le Minimum que vous avez avec les personne qui compte sur vous bravo Diadia
Salam je n'ai jamais commenté sur les réseaux sociaux.mais là diodio ma bleffé en plus posé respectueuses âme soutoureu begue nit et parle calmema sans insulte ni gro mot et no au blabla chapeau à toi k dieu te garde
@@hapsaathie7594j’accepte daga comprendroul mtkh ga tontouma. Tu sais fane lay waxei elle est très belle MachAllah mais elle a perdu toute sa famille yalla dalay may li xagn la té nekoul né lounek gay am.beauté wam bi ak amat sa famille selon toi lane lay choisir? De même que Wally plus aimé mais perdre ses parents adouna yalla dagnouy diangal rek. Diodio mougui ni nena Yaye dji da amone après gnak tay Yaye dji demna certes mais yagui guiss lep lo Yaye dji gnak amat nako mais tay mou guissat yayam moko gueunalone fouf adouna leçon la yalla aki mbiram… Foumay xalat Mo sorri ma belle
j'adore cette femme. Moi je l'ai aimée quand j'ai vu les vidéos de ses vacances avec ses employés à l'hôtel . elle est très généreuse. yalna nga goudou fane, ame weer
Masha allah j l'estime beaucoup Diodio c une femme de valeur ma discrète belle et aimable yalnako yalla sam arko mousseulko té mouthieulko j lm beaucoup
J'ai jamais suivi confidence c pour la première fois et grace a cette Brave Dame Diodio. J'ai bcp pleuré car j'ai bcp galèrè et jusqu'à présent, je pleure souvent en passant si ma mère décéde sans que je puisse faire quelque chose pour elle( teralko). Mais je te jure que s'il plaît a Allah je reviendrai ici pour te dire que jai réussi grace a la motivation que tu m'a donnèe merci 1000fois
Gnak waydiour dfa meti surtout bou soner si iow tei fékéwoul dra mann souma xalater k sam papeu diayna sakh telephonam pour sama diangu tei bimou guagno ak legui dra sotéguoul ms guem nani lep dina bah nakh khalatouma lassai nakh mom ma wett si loll nak ms yalla bahna Diodio yalla nla yalla lafal thiate sa yaye fierre na trop masahalah yalla na soutoureu gui yokk
Une grande dame que j'estime et je l'ai croisé à plusieurs reprise dans des boutiques a Dubaï mais toujours souriante et respectueuse. Yalla na borom bi sameu.
Vraiment ta motiver 😫 une monde Entière sèrieur tout personne qui veux rèussir dans tout sa vie n’as s’inspirât dans ton Histoir Ce l’on moi avec tout t’a Histoire sa mérite d’être mentionné dans un livre 📖 de motive vie Donc tout ce que j’ai à te dire longue vie à toi, et puis j’espère que un jour que je pourrais te voir puisque je suis très fier de toi, ma sœur, longue vie ❤️🙏🏿
Jai appris beaucoup de chose à traver cet émission diodio une personne très rare ndeysane yalla moy tane nitam te Ken menousi Dara walakhi j me voi en toi lep Lou yalla def dafa gueune et il faut toujours l prendre positivement et avec motivation juste c magnifique de vous avoir écouté merci ☺️
J ai juste envie de vous serrer dans mes bras et vous dire je t aime et je t adore vous êtes une grande dame ´ je ne pouvais pas m empêcher d écrire c est ma première je vois en vous ma défunte grand mère elle faisait tout cela en toute discrétion il est 3h 10 je pleure pour vous en pensant à ma grand mère que son âme repose en paix continue à être toi même et le reste le bon Dieu va continuer à t assister bravo à la presentrice
Vraiment c'est une grande dame je t'aime naturellement tu encourage toute femme qui veut réussir tu me donne beaucoup de motivation tu as un bon cœur courage lep dîna guena bakh inchalla
Merci tata diodio sa dal bi AK sa classe Daf ma yém ❤ man Manou ma imagine Biss niew té Douma guiss Sama yaye 😊mai yalla na yalla kharé aldiana sa yaye yalla dolel la Bou yok la si barkép Serigne saliou 🙏🙏🙏❤️
Masha Allah ton parcours m a beaucoup touché am yar bou bakh ak diom rek mo am solo borom ❤ bou rafet moy gawa dioy yalnala Allah takhawou sope nala lol
Franchement depuis le début de l’émission je suis bouche bée Yallah nako Yallah samb on a le même âge et c’est un exemple pour les jeunes bonne continuation
Les études ce sont des outils très important pour la personne surtout avoir une formation dans un domaine vraiment cherchons le savoir avant de faire quoi que c soit ❤
Machalah cest la premier foi ma suivre emision bi mé.diodio je l,aime beucoup niake yaye dafa méti kouko dondoul😭 monoko khame..méme moi jai. Perdu ma mére😭😭😭
Les gens qui sont vrais ne pleurent pas quand ils racontent leur histoire. Ils deviennent forts au fil des temps. Ça se voit qu’elle n’est pas dans le théâtre quand elle raconte sont histoire. Elle ne cherche pas la pitié des gens. Elle veut impacter. Bravo !!!
Quelle autre personnalité ou célébrité aimeriez-vous voir sur le plateau de Confidence
Viviane😭
Adja keisha Deme
Amy mbengue artiste
Amy channel
Youssou Ndour
Meilleur des PDG moy nitte ki Walay nous ses employés amouniou sa fay bakh gua beugue guaniou âme gua sounou yeurmandé y’a takh niewouniou keine thiam diapé woniou employé mes des sœurs lou bakh rek guané nioune la yeiné bigua ame si nioune mane nane ko
Seider devant tout le monde PDG bou bakh riche gueune bari yermandé Yako deff thiam ta générosité ta gentillesse sa tabé me dépasse Lo âme bokou guako ak nitte gni yalla nasa diamou yague yalla bo guis Dara lo ragal diodio glow skin si kaw si kaname rek inchallah 💪♥️♥️♥️Loune la wakhal rek si Lou bakh ame na Lou dess yalla nasa diamou yague ❤❤
On peut parler en privé ?
Es que on peut parler en privé svp
Maa shaa allah yalnalene yalla samm si barkei seydina mouhamed saws
MAME DIARRA THIAM YALLA NALA YALLA AAR , SAME , MAYE SOUTOURA AK DIAM AK KHÉWEUL AK MOUDJOU BOU RAFÈTE , FOULE LA THI KAW TÉ LAKH LEU FA YAAKH AGOUL SI BARKÉ NABI MOUSTAPHA SALA LAHOU ALEYHI SALATOU WA SALAM PSL . AMINE YA RABI NIOU BOK KO .
En tout cas mangui ni done setane émission bi pour terminer ko et jangu nassi Lou Bari beugue si femme bi t xamoumako mossouma tok dieul sama temps setane vidéo wam grâce à cette émission nak xamna ni nit kou bakh la kou am yeurmadé ak yiw longue vie Diodio bonne santé insha'allah 🙏 je te. Love ❤❤❤❤❤❤❤
J’ai mes larmes en regardant cette Émission de Diodio ce qui te tu pas te rends plus fort
Tu fais ma fierté moi à 27 ans je parviens pas à rien réaliser mes rêves envers mes parents je t’estime pour cette grave Dame que tu es devenue
Que dieu te garde dans cette vie aussi longtemps que possible
YALLA MOY DEFF NITT KILIFA GORGOLOUL REKK TEHH GEUM NI DIGA AMM
@@maguettecisse7611 Inchalla Yalla bakhna magui thi yoneuh wiii
Yalla naniou bokk thi gnimouy sédd
Borome karaw gou nioul niagoul dara goor goorloul
Yallah daffa duekh mane à 47ans la tabakhale sama yaye keur yobouko maque ndieukeu ferhia takhouta moudiepeu guéw yallah meuneu n'a louné
@@saufi719 lou lerrrrrr guafi wakh
Machalla Yalla bakhna en tout cas yalla nopina demba. Merci beaucoup à vous
Elle m'a redonné le courage Yalla nala yalla fay Thiam Babel j'ai un enfant et j'ai que 22 ans mako yorre yore sm bopou sm Rak ak sm Yaye mais sante elle m'a redonné le courage Yalla nala yalla takhawou inch'Allah ❤
Bon courage baisse jamais les bras ❤
@@khadijadial4677 merci ma sœur
Deysane machalla
Mashallah j’ai jamais commenté mais cette femme c’est une référence une femme inspirante yalla nako yalla takhawou 🙏🏽 meilleur confidence
Machallah Sokhna Diarra mii vrai référence la ❤😢 machallah yangui dèf Lou bakh 🤍 yalla nga yocku ba yeuk ko ❤🎉Souma maguê yalla naa mèl ni yaw❤️🥹
On dirait que tu racontes ma vie DioDio. Tu as relaté quelques passages de ma vie et je me vois dans ce confidence, Yalla na Yalla gueune la takhawou gueune la doléle boul tite boul ragal sa khol moy lampe biy léral sa yone. Khamoumala dé mais dangama méy fitt pour yone bima dieum ma niéméko khamni gueum sa bop ak Yalla diapaléla rék mofi nék donc chapeau bas à toi. Merci pour cette motivation que tu viens de me procurer. Mangui dounde instant bi lou métti té tar lolou mais béss bouma amé succés si yone bi ma beugueu dieul dina nieuw basi yow toudé la sama succés c'est une promesse té dinako tenir Insha Allah. ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤vive cette battante waye. Des ❤ pour Dio Dio❤❤❤❤❤
Diodio est douce et posée, comme Mame Coumba rekk. machaAllah djiguène dafay réglée♥️
Je les aime ❤️❤️
❤❤
Bilahi yow djiguene tamou nagnou si dal téw surtout réglé
Bilaye yow motax gneupa koy déglou elle est tellement posé❤
Koy garouwalé😂
J’ai eu l’impression que c’est moi qui est assise à la place de Diodio tellement notre vie est identique commençant par le décès de sa mère chose que j’ai vécue et qui a fait de moi ce que je suis aujourd’hui. Tout coïncide avec mon vécu. Yalna yalla yok gneup inshalah.
Non man ngay wakhal surtout le décès de sa maman j’ai parlé avec ma maman à 8h 10h on m’appelle pour me dire que ma maman est décédé 😢😢😢😢😢 mou melni adina bi day danou sama kay
Amine ya rabi
Diodio qu’Allah te préserve et te protège de tout mal ..c’est la première fois que je commente sur confidence mais saches que hormis ton entourage il y’a des gens qui t’aiment sincèrement et te souhaite que le meilleur
Tu es ma référence wallahi et j’espère un jour devenir une femme indépendante, aimante tel que toi
Ceux qui sont près de toi ont vraiment de la chance de côtoyer une personne comme toi
Je te dis tout simplement mashallah et on n’est très fière de la femme que tu es devenu aujourd’hui
♥️♥️
Ta gentillesse est❤ très rare dans ce pays yalla nala yalla défale diam k dieu te protège
Une femme de toute les qualités ☝️ wallakhi anzim c’est une dame de référence toute femme doit faire diodio comme référence car elle a traversé des moments misérables🥺❤️❤️Diodio man diamou yalla bi mangui lay gnanal guoud fan wer yokk ba gnoun gniy sétan diarignou thii diodio yalla bo guiss lo ragual🤲🏾🤲🏾diodio diam la la yéné diodio kholay wakhé guene nala beugue ndakh Diamou yalla yi guay rendre heureuse
Avec DioDio c’est une leçon de vie mes frères et sœurs levons nous dara dou diouk rek soti guem guem focus fierté sante yallah inchallah lepp di na bahh ❤
J'ai regardé l'émission du début à la fin avec des larmes comme Diodio il faut être une personne entière comme elle pour mieux comprendre la dame la actuellement je traverse des moments pareille que ses moments d'avant surtout bou waxé ni worna beu gone diot mou nane ndoh ak tantdarma c'est comme si elle était en moi mais alkhamdulilah natou metiwoul
Une émission a limage de la présentatrice et de son hote ( Niari MAME YI)
-Mame coumba une dame simple classe et raffiné. Une personne humble douce et bien éduqué.
Face a son invité Mame diarra Alias Diodio borom Diodio glow skin
Une jeune dame oui tres jeune meme machallah Etre PDG dune telle entreprise etre la maitresse dune si belle reussite a son age n’est pas donné a tous malgres les difficultés de la vies et son jeune âge. Une femme forte avec du caractère chose qui lui a permise d’en arriver a ce stade mais en meme temps une dame pieuse et croyante un exemple pr les jeunes filles qui aimeraient réussir a la sueur de leurs front une bonne personne abec bcp de qualités tres humble et respectueuse douce machallah dal régler geum yalla tei diko diamou.
Vraiment merci pr cette émission je pense que depuis kou nk diaarna fi mais par la qualité des paroles la douceur de l’une et l’autre vraiment bi mo dakh yeup❤❤❤❤. Merci a vois les Mame yeine la rew mi sokhla pr wane khaleyi yonou deugue bi yinou diamou yalla bi yonou liguey bi. Am leine diam
Meilleur des PDG bakh riche guenneu sama yaye djii yayou diodio ak papa madior yaww lii dou chance mèrite leuuu tèguèganiou yir ganiou diap ganiou topoto ganiou diapèwoniou employé mais sayy dôme gni sayyy sœur yaw madiodio sou diougater do dèfarate sa togay baby d amour kor ndiouga fall yakousi Dara diniou diapaler diniou conseiller Mme Fall kor ndiouga sama wadji l intellectuel des crèatrices des grandes entreprises et marque 🎉🎉🎉 au Sénégal 🎉🎉🎉❤❤❤❤❤❤
Ayy wayy boléne ma ak diodio svp
MashaAllah
C’est la fille de Madiodio Gningue donc ?
Ohhh ndeysaan machalah Diodio Nako di mbepp mbepi ni ngima kham Laff thiate li yeup amna fi ta toguo fen diko wakhe Yalna yalah gueun lén takhawou 😢❤
Jai jamais commenté Chapeau a cette émission mame coumba bravo encore cette dame de fer nous fait reve et d'aller de l'avant damakoy suivre rekk sur les réseaux mais nitee kou simple humble modeste bax labir nitou kesse yené gneup ame yeurmandé on sens son honnêteté quand elle parle machallah bonne continuation nga yokk ba yeuk ko aminn
Ay maso commentaires si Mamy Cobra ??
Ta gentillesse est très rare dans ce pays fonce que Dieu te protège
Je t'estime vraiment Diodio Yalla na Yalla doli soutoura ak goudou fane
Waaw je suis tombée amoureuse de la personnalité de cette Diodio Mashalla yalna yalla sameleu areleu soutouraleu motalli projets yi si barkei Serigne Babacar sy ❤❤❤
Allahouma amine ya rabi
Amine Yarabi❤❤🥰
J’ai fais 3jour à regarder cette émission chaque parole de diodio me fait pleuré une personne plus que parfaite yallah na la yallah takhawo bayinala ak yallah mome mi diare denke ❤
Ndeysan sama fadiar jeudi ba je n avait que 11 ans may yéwo di lathie sama niouni ma sa yay décédée na. Ma oumou dort en paix tu me manque énormément 😢😢
Massa du courage❤
Ndeysann courage
Courage ❤tite sœur
YALLA YALLA Yeureume ko dëfalko Aldianaye Firedawzi Si BareKème Alkhourane Amine Yarabi
😢😢masta
WAAAAW, mais comment ne pas se confier a cœur ouvert face a une dame aussi charmante, correcte, accueillante et très a l'ecoute en plus le cadre est propice pour se confier. SOKHNA MAME COUMBA, merci! - SENEPOEPLE +, merci! - Mention Speciale a l'equipe technique! 🤍💯
Vraiment
MME MAME COUMBA DIA NIANG , FEMME ADORABLE , PROFESSIONNELLE , RESPECTUEUSE , RESPECTABLE , À LA VOIX DOUCE , FÉLICITATIONS !
Maa shaa Allah une dame pétrie de valeur ndeysaan ,nitte au vrai sens du terme la deglou taye ces ces personnes généreuse et empathique qu’il faut suivre sur les réseaux ,motivantes et source d’inspiration, kou goré rek moy geureum gniko diapale surtout ses employés force à toi diodio
19:04 Diodio dioylo ngama 😭😭😭c’est l’anniversaire de décès de ma mère aujourd’hui 😭nianale len mako nguir YAllah 😭
Yalnako yalla yeureum té jégalko
Yalla nako yalla yeureum khareko aldiana firdawsi si barke zeydina Mohamed
@@fatoudiakhate1516 amine y’a Rabbi
@@nogayesene5600 amine y’a Rabbi
yalla nako yalla yereum té xaré ko aldiana woyofal Souf sikawam
C’est la meilleure des émissions mame Coumba son parcours est remplie de leçons machala Yalnala yala lafal tiat mame diarra
Oh c la premiere fois k jecoute cette dame jai les larmes courage lo am yako mérito
C’est la première fois je regarde cette émission grâce a la femme battante Diodio la plus douce gentille ouverte d’esprit meilleure de ta génération je t’aime 🥰
Moi aussi c’est la première fois ❤elle est très brave
Moi aussi c’est la première fois et j’en ai tiré des leçons sur tout. Je peux dire qu’on a le même parcours mais elle me redonne confiance.
Bravo grand Dame. So much love ❤️
C'est à cause de diodio que j'ai regardé confidence pour la première fois ❤machalah une brave dame😊❤
Pareil
Pareillement
Pareille pour moi
Pareil en intégralité meme❤
Moi aussi
Référence la deh pour djigen gni mane deh beug na tok akk mome dama bari aye projet macha allah
🙏❤❤❤❤❤❤💪🤳
Vraiment geune nala fonk geune nala beugue bilahiii walahi quand tu parles de ta mère j'ai Les larmes aux yeux Mane mii nga kham ni téral sama yaye rekkk laa beugue mais j'ai pas encore les moyens mais yalla bakhnaaa Sokhna Mame Diarra Thiam DIODIO GLOW SKIN YALNASSA DIAM YAGUE ❤❤❤
Cey Sénégalais
Machalla ❤yalla gua guoudou fane
J’ai pleuré 😢nala yalla sammm Diodio yokou ba yeuggg ko si barkiiii Ahmadou inchaallah
l'émission de diodio ma beaucoup réveillé dans la vie sa me donner beaucoup de courage
Oh, Ma Challah Mane dama beug Borome khöle bou Rafëtt🥰🇸🇳🥰Sokhna Mame Diarra
Pour une première fois j’ai pris mon temps pour suivre l’intégralité de l’émission à cause toi Diodio yalla nala yalla sam
Waw 😢je t’admir de plus en plus diodio ❤une grande dame ❤
Quelle belle âme ! Yalla nala Yalla may leu guud fan ak wergou yaram mouseul si thiat amine ya rabi 🤲🏾❤️
VRAIMENT; ca été un regal de t'ecouter diodio je te souhaite plein de succes sur l'echelle mondial ,,,vas y continue de focus,,
Ndeyesan éducation da base mo ame solo . Nitkou tey dale , intelligente machallah ❤
Machalla notre diodio nationale ❤ yalla na yalla sameu are ndiabot gui si barcké Mouhamed 🙏🏿🙏🏿
Ay mame Diarra sama toma sama boukki bi mate nala mais yalla mofi né bo niaké yaye dara doula saf doto amati nakhar boula diakhal mais alhamdoulillah yalla mo niouko diokhone moko dieulat
Meilleure PDG ❤ on est vraiment fiere de toi goude fane akkk werr reck inshallah i love you so much on taime vraiment de la part de tes employés ❤🎉
🇬🇦 bonjour je suis gabonaise , je regarde toujours l’émission avec mon amie sénégalaise, ça me ferai plaisir si vous mettez la traduction en français s’il vous plaît car à chaque fois on est obligé de couper la vidéo pour qu’elle m’explique 🇬🇦❤️ je vous admire
Vraiment cette confidence est la meilleure cnfidence bi dafmeu diangal lou beuri si adouna diodio bnne cntinuation on est fier de toi
Je pleure en regardant cette émission elle est vraiment une référence pour les filles ou garçon de ce monde soyez simple et partager le
Minimum que vous avez avec les personne qui compte sur vous bravo Diadia
Salam je n'ai jamais commenté sur les réseaux sociaux.mais là diodio ma bleffé en plus posé respectueuses âme soutoureu begue nit et parle calmema sans insulte ni gro mot et no au blabla chapeau à toi k dieu te garde
Wally
Adja Diallo
Diodio
Lerna yalla kou xool si gnom do rer
Yalla rek moy Bour té gouram rek modoul diekh
Force à vous mes❤
Adja diallo 😂 yow wergua ?
@@hapsaathie7594wawaw werna key limou wax deugue leu
😂😂😂
@@hapsaathie7594j’accepte daga comprendroul mtkh ga tontouma.
Tu sais fane lay waxei elle est très belle MachAllah mais elle a perdu toute sa famille yalla dalay may li xagn la té nekoul né lounek gay am.beauté wam bi ak amat sa famille selon toi lane lay choisir?
De même que Wally plus aimé mais perdre ses parents adouna yalla dagnouy diangal rek.
Diodio mougui ni nena Yaye dji da amone après gnak tay Yaye dji demna certes mais yagui guiss lep lo Yaye dji gnak amat nako mais tay mou guissat yayam moko gueunalone fouf adouna leçon la yalla aki mbiram…
Foumay xalat Mo sorri ma belle
@@hapsaathie7594moma diaxal 😂😂😂😂même wally wax amou fi place
Mane je dirais plutôt Diodio ak Kiné sow ( mayacine ak dial )
j'adore cette femme. Moi je l'ai aimée quand j'ai vu les vidéos de ses vacances avec ses employés à l'hôtel . elle est très généreuse. yalna nga goudou fane, ame weer
Masha allah j l'estime beaucoup Diodio c une femme de valeur ma discrète belle et aimable yalnako yalla sam arko mousseulko té mouthieulko j lm beaucoup
Une belle personne ❤ yalnala yalla sameu bou bakh Mame Diarra🙏🥰 ndeyssane Niak yaye dafa méti surtout yaye bou takhawou domam😢 Moungui melni sama yaye ngay wakh Ndiaye Alboury yaye bou sonone ci ndiabott tei fekewoul dara😢 liguey am tei sa yaye meunoul lekk sisa niak aka méti😭🥺😢 courage Mame Diarra❤️🩹
Yalnala yalla faye lepp lingay def si domou adama yi 🙏 vraiment j’ai bcp kiffé l’émission❤❤❤❤
Des bisous Mame Coumba🥰
Force à toi ta Diodio et à nous qui on perdu nos maman💔😭
Tellement douce et posée no ki dal je l'aime dal yalna sa diam yague ma
DIODIO de ❤
Tu ma fais pleurer diodio 😢sa yaye nianal nala borom bakh gua nala yalla same si barcké nabi psl on t'aime trop fort ❤
J'ai jamais suivi confidence c pour la première fois et grace a cette Brave Dame Diodio. J'ai bcp pleuré car j'ai bcp galèrè et jusqu'à présent, je pleure souvent en passant si ma mère décéde sans que je puisse faire quelque chose pour elle( teralko). Mais je te jure que s'il plaît a Allah je reviendrai ici pour te dire que jai réussi grace a la motivation que tu m'a donnèe merci 1000fois
Gnak waydiour dfa meti surtout bou soner si iow tei fékéwoul dra mann souma xalater k sam papeu diayna sakh telephonam pour sama diangu tei bimou guagno ak legui dra sotéguoul ms guem nani lep dina bah nakh khalatouma lassai nakh mom ma wett si loll nak ms yalla bahna Diodio yalla nla yalla lafal thiate sa yaye fierre na trop masahalah yalla na soutoureu gui yokk
Walahi dîna baax inchalla
@@ousmanendour9465 inchallah amnagnssi guemm guemm
Beuss boula yalla mayé nga Gass tene pour mom tiyaba bi fek ko fimou nek. Massa
Une grande dame que j'estime et je l'ai croisé à plusieurs reprise dans des boutiques a Dubaï mais toujours souriante et respectueuse. Yalla na borom bi sameu.
Vraiment ta motiver 😫 une monde Entière sèrieur tout personne qui veux rèussir dans tout sa vie n’as s’inspirât dans ton Histoir
Ce l’on moi avec tout t’a Histoire sa mérite d’être mentionné dans un livre 📖 de motive vie
Donc tout ce que j’ai à te dire longue vie à toi, et puis j’espère que un jour que je pourrais te voir puisque je suis très fier de toi, ma sœur, longue vie ❤️🙏🏿
Jai appris beaucoup de chose à traver cet émission diodio une personne très rare ndeysane yalla moy tane nitam te Ken menousi Dara walakhi j me voi en toi lep Lou yalla def dafa gueune et il faut toujours l prendre positivement et avec motivation juste c magnifique de vous avoir écouté merci ☺️
J ai juste envie de vous serrer dans mes bras et vous dire je t aime et je t adore vous êtes une grande dame ´ je ne pouvais pas m empêcher d écrire c est ma première je vois en vous ma défunte grand mère elle faisait tout cela en toute discrétion il est 3h 10 je pleure pour vous en pensant à ma grand mère que son âme repose en paix continue à être toi même et le reste le bon Dieu va continuer à t assister bravo à la presentrice
Diabar nala djik wayé dieukeur aussi nala djik MACHALLAH YALLAH nala YALLAH bayi ak MONSIEUR FALL 🤲🤲🤲🤲🤲🤲💚💛❤
AAAMINE ❤
Machallah j’ai beaucoup pleuré Diodio yalla nala yalla faye sa khol def lou bakh rek mo ame solo
C’est la première fois may commenter si réseau sociaux mais souma magué yalna mélni Diodio magui kay niane sunu borom🙏🙏
Vraiment c'est une grande dame je t'aime naturellement tu encourage toute femme qui veut réussir tu me donne beaucoup de motivation tu as un bon cœur courage lep dîna guena bakh inchalla
Les mamans solo en france savent tout ce que tu viens de dire😢😢😢 malheureusement la vie est dure ici surtout quand tu as un enfant mais yalla bakhna
Dina bah💖💖💪💪💪
Je n’ai jamais pleuré suis mère et jeune diodio à vécu une partie de ma vie brovo kou defal yalla am Yalla
Elle ma tellement fait pleurer j'imagine meme pas un jour sameu yaye dem bayim😢yalleu neu yekh
Merci tata diodio sa dal bi AK sa classe Daf ma yém ❤ man Manou ma imagine Biss niew té Douma guiss Sama yaye 😊mai yalla na yalla kharé aldiana sa yaye yalla dolel la Bou yok la si barkép Serigne saliou 🙏🙏🙏❤️
Masha Allah ton parcours m a beaucoup touché am yar bou bakh ak diom rek mo am solo borom ❤ bou rafet moy gawa dioy yalnala Allah takhawou sope nala lol
Machallah, très intelligente, stratégique, douce et travailleuse. Bonne continuation
Franchement depuis le début de l’émission je suis bouche bée Yallah nako Yallah samb on a le même âge et c’est un exemple pour les jeunes bonne continuation
Je pleure même en regardant 😢l’émission 🥹 Diodio je l’adore 😍 c une brave femme ❤ machalla yalla nala yalla sam
Non mais vraiment Diodio je t’apprécie de plus en plus une source de motivation ❤
Quelle femme admirable cette Mame Diarra ! Yalna leu yallah arr, lakeu leu fou yakeu agoul ❤
Nit bo khamoulè deko wowè hèhh elle ma fait pleurer mention spéciale à toi yalla na yalla barkel lep inchalah ❤❤❤
Les études ce sont des outils très important pour la personne surtout avoir une formation dans un domaine vraiment cherchons le savoir avant de faire quoi que c soit ❤
Vérité absolue bilahi machala ell es posée
Aah sayy morom diay katt yi warnan royye si iow kholal lii rek tè monè lii kenn meussou ko degg yangui ligey tè tioww bari woull❤❤❤❤❤
Lo djamboul bakhoul diodio glow boler classe ak organiser machalla
Diodio beugue nala torop sisa modeste khammm adouna sisa bakh courage amal tawfekh akk taisir rekkk inchalla ❤
Jai beaucoup pleurer jusqu'a tomber malade.jai vecu le meme histoire je taime fort diodio
Yanghi tané
@@moissirathior7853😂
Allah Akbar machalla ma chérie longue vie❤❤❤❤
Mashallah Diodio wakh dji rafet na yiw na yalla yalla khep doli❤
Machalah cest la premier foi ma suivre emision bi mé.diodio je l,aime beucoup niake yaye dafa méti kouko dondoul😭 monoko khame..méme moi jai. Perdu ma mére😭😭😭
Les gens qui sont vrais ne pleurent pas quand ils racontent leur histoire.
Ils deviennent forts au fil des temps. Ça se voit qu’elle n’est pas dans le théâtre quand elle raconte sont histoire. Elle ne cherche pas la pitié des gens. Elle veut impacter. Bravo !!!
❤
Je ne suis op d’accord chaqu’un a sa façon de montrer son émotion ame ay nitt yo kham ni bouniouy rencontrer sen diar diar di dioy donc niep yèmouniou
Machalla j ai suivi tous vos invités mais cette émission m a beaucoup marqué c est la meilleure une diodio calme douce ❤❤❤❤
Machala yayam dafa bakhone ndeysane beug mbokk nekone ndiambar ❤️🤲🙏🏽
Machalla sama mame coumba youkour égal à elle même diodio on es de tout cœur avec vous ❤❤❤
Machalla Ndayssane je donnerai tt pour te connaître ma tata diodio vrai référence 😭🙏🙏
Dioy 😢na ba sone Bilay barkep serigne fallou ki amouma si mom sago c la premier foi ma sètane confrontation
Machala femme brave comme diodio référence la man damako beug tu nous a beaucoup motivé
Diangua bila sa YAYE forcé amal nala ndiarigne torope lolou mo indi sa démarquage au sa domination sur le marché du cosmétique MACHALLAH ❤🎉❤🎉❤🎉❤🎉
Force à toi Mme Diodio
Do daanou mouk ndax place binga tekk sa yaye.
Vraiment Diodio elle est trop généreuse machalla yalla nala sunu borom guena yok 🙏 je suis fan de toi je te suis partout machalla ❤
Sache aussi que ta fille est ton PORTE BONHEUR MACHALLAH fonka ko bou bakha bakh❤🎉❤🎉❤🎉❤🎉❤
Yalla na la yalla lafale thiate tu es un bonne découverte nitté mo diaffé machallah dal posée kham wakhine
Diodio référence leuh machallah yalla na yalla sam leuh tei lafal leuh thiate thi barkeii seydina Mohamed ( psl) ❤❤❤
Ndeyesane j'ai tellement pleuré vis à vis du témoignage de son employé bakh moy lép fingua ték sa tank fofou la
Wlh man diodio dama néxx dafa téiyyy man dal je t’adore
Machaalah courage merci Mame Coumba pour cette merveilleuse dame agréable à écouter que vous nous avez présentées
Machalah à notre diodio el ma vrémen fé pleuré yalnala yalla may weur ak goudou fann 🙏🏽🙏🏽