Ndeysane Mag yarou nga beuri nga kersa ndékété meune cas rek moy sa Thiate… je t’estime à partir d’aujourd’hui. Sinon, Makhfoussse, tes acteurs font vraiment le job. Bravo !
Non mais mag je l'adorais mais je l'adore encore plus quel bel homme il parle avec tellement de respect bien vrai que li ko gni di wax nexou ko ❤mahfouss ya feuleh founek 😂
Du bon boulot comme d'habitude Mashalah Mais j'ai remarqué qu'au début Mag a dit qu'il reconnaissait le gars en noir et blanc et si je me trompe pas ceux sont les mêmes personnes qui avaient pranker Bibish et vous n'êtes pas sans savoir que prèsk tout le monde regarde cette émission alors faut changer les acteurs pour plus de surprise quoi Je suis désolée encore une fois 🎉😊
C’est vrai makhfouss faw mou changer acteurs yi surtout celui avec la barbe et casquette nieupeu ko hamei Makhfouss stp bayi si xel L’autre en teint noir mome dafa ayy il est trop fort
Mag yarou na nk th louma tchi gueuneu néx moy dafa bagne des le début ak Serigne Touba mi mouy waat blh mala beugue où sont les mourides ? Safar gui thioub si na dh❤
Ah magvision mi beugu nako dh barké Serigne saliou machallah ligua nekk boula ci dara dieulé samal sa ngor fo tolou boula ko allalou aduna meuss diaral barke sa tourodo (psl)
Mahfouousse je t'aime bien mais affiche bi drapeau gayi manone nasi bania bok j'imagine que bayiwolene si khel mais promo la pour niom, Merci de votre compréhension, je suis très positif avec mon commentaire❤🫶🏽
Je me suis dite la même chose après avoir regardé ce prank et celui avec Bibiche . Je trouve que même le fait de faire des prank sur leur sujet est un promo pour eux.
j'aime yiguein di niane thi commentaires yi daniulein dithi faay khaliss wala louy probleme bi ak j'aime yiguein di am ? BREF; le prank était super comme d'habitude
Mah, attention! on commence à reconnaitre tes acteurs. Il faudra penser à les varier. Sinon toutes mes félicitations encore et mes encouragements. Bravo
N’oubliez pas mon code promo 221M vous allez aussi avoir plein de cadeaux avec l’Euro 👉🏾 cutt.ly/EeaTzDd2
Slu mah faut mettre le lien de l'autre chaine pour faciliter la recherche car c'est un peu compliqué merci d'avance
youtube.com/@beussbouton7?si=SmXmHAUeSnilULTO
MAKHFOUSS PRANKAL BACKA NIANG WAY
Makh defal ben caméra cachée ak couple yi si meuf bi ak groupe goor kou niow wakh qui kan la guelou gayi niou khol réaction copin bi 😂😂
@@Mahfousse
Ana ngi beugue seydina Mohamed❤
PSL ❤❤❤❤❤❤❤🙏🏼
Ya rassoulalah ❤❤❤
Psl ❤❤
❤❤❤
Niongui ni❤❤❤❤
Où sont les talibé cheikh 🥰 SBS rek🎉
Kou beugue niou prank Amy Léa rék lalale j'aime ❤️
Kou beug niou prank dip doundou guiss lalale j' aime
Mn😅
😂@@AntaFall-t2w
Kou begue serigne touba lale jaime ❤❤
Beug nako wayé douma lal
😂😂😂😂😂@@baayjuuf
@@baayjuufBoo laloul sama yon nekousi 😂😢
❤❤
❤❤❤❤
C une leçon de vie ça l'argent ne doit pas te faire vendre ta dignité et ta personnalité 🎉🇸🇳😊
Ana gnon beugueu Serigne Babacar sy ❤❤❤
Mahfousse on réclame ngakka😅 blindé kou d'accord 🤙
Lou nekh😂😂
Oh mon dieu aimer moi pour la première fois 🎉🙏
Sa se voit c'est kelk'un de calme et serein 😂😂😂 bravo 👍
Ndeysane Mag yarou nga beuri nga kersa ndékété meune cas rek moy sa Thiate… je t’estime à partir d’aujourd’hui.
Sinon, Makhfoussse, tes acteurs font vraiment le job. Bravo !
Wah yako guiss mouy cas parfois Sénégalais yi daniouy toumal nit dh
@@sodamareme45lou lèrr ngua wakh
Gneuwoneu sama mariage sœur mais kou dal yarou senegal no Def gnou sikeul lolou rek leu
Non mais mag je l'adorais mais je l'adore encore plus quel bel homme il parle avec tellement de respect bien vrai que li ko gni di wax nexou ko ❤mahfouss ya feuleh founek 😂
Ndaysan wakhna lou am solo « fima bok la » nit loy def si adina wargua khalate askan bigua bok am gua valeur frère ❤
Mag yalla nala yalla guena diapalé are la yir la lak la fa yakk agoul si Barker seydina ak sa diabar ak sa famille
😂😂
Kou d'accord niou prank sannek lalal jaime❤❤❤😊😅🎉
Makhfousse tes acteurs sont excellents 😅 et mag ça se voit c'est quelqu'un de bien et très calme.
Ko d'accord niou parnk papa cheikh diallo❤
On réclame le prank de maimouna Fall et Aïssatou de la série cœurs brisés 💔 😊
Bly louy xèrè
Aïchatou ak ayy wolofam lou Nara nèkh 😂😂😂
Kou beugu gnou prank Amy Léa wola ndeye marie RK lalay j'aime
Makhfous on réclame diogaye séne 😂😂 kou d'accord
ndeysane Mag dh amna loumouy bagne d'autant plus k ndirou na ak kou am Talibé
Oui comme son père machalla tel père tel fils
Du bon boulot comme d'habitude Mashalah
Mais j'ai remarqué qu'au début Mag a dit qu'il reconnaissait le gars en noir et blanc et si je me trompe pas ceux sont les mêmes personnes qui avaient pranker Bibish et vous n'êtes pas sans savoir que prèsk tout le monde regarde cette émission alors faut changer les acteurs pour plus de surprise quoi
Je suis désolée encore une fois 🎉😊
C’est vrai makhfouss faw mou changer acteurs yi surtout celui avec la barbe et casquette nieupeu ko hamei
Makhfouss stp bayi si xel
L’autre en teint noir mome dafa ayy il est trop fort
Ndeysanne xolal gantou na ak yarr ak teguine thi fouleu vraiment MAC amnga ndam talibé serigne touba dara diomou ko digne rek
Aïssatou cœur brisé kou dcc ❤❤😂 ak Wolof yi lou xeré
Ont réclame yakhara alias ndeye Marie karma 😂
Ndeyssane il semble être une bonne personne avec tout ce qui dit sur lui. Yalnala yalla saam
Pére zora mo bakh Ci yéne wayè ki dé amna foula bamou soné da déme tok😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂
N'oublions pas les 5 prières 😢
Ohh dioup rk moo am solo machalla Mag❤
Mag yarou na nk th louma tchi gueuneu néx moy dafa bagne des le début ak Serigne Touba mi mouy waat blh mala beugue où sont les mourides ? Safar gui thioub si na dh❤
Trop maxtrisé😏
Dafa lèrrr 🥳🥳🥳❤
@@boubacarwaounde8199louy lolou
Bilay yaw kou dall ndaysane 😂❤❤
ma shaa allah M. Niang, dafa dal, tey ! soudone kenen dineu teup ak dal di saaga !
Le gars teint noir bi am sikim bi noumou toudou svp, il est trop fort sur tous les pranks il assure trop son rôle ❤️❤️
😂😂😂 waa loucii diaar kham tourr naak, diapaal acteur borom sikim bii cii equipe Mahfouss reik😂😂
@@ngonemariefall4463boulma Ray way😂
😂😂😂😂da diap thiopatem😂😂😂
@@ngonemariefall4463 non pour suivre ko si reseaux yi ayway😂😂😂
@@liinguere998 ayway dou lolou bilay😂😂😂😭😭pour suivre ko si reseau yi rek
Mashallah sago dafa bakh thi 'nite ak yarr yalla na yalla barkel ligueye bi amine 🙏
No mag mo yarou nak macha Allah sagawo béneu yone té boula néxone gua défko mais amna nio xamni yalla moléne yar
Ah magvision mi beugu nako dh barké Serigne saliou machallah ligua nekk boula ci dara dieulé samal sa ngor fo tolou boula ko allalou aduna meuss diaral barke sa tourodo (psl)
En tt cas Magvision est très poser prank bi nekhna😂😂🫶🏻
Macvision mes respects ❤barké borom Touba djam thi yao
Machallah mac geun nala sope ndakh sa dinité en plus kou ame talibé gua boula alalou adouna dougeul si dra louniou lay khébé✅
Mahfouousse je t'aime bien mais affiche bi drapeau gayi manone nasi bania bok j'imagine que bayiwolene si khel mais promo la pour niom, Merci de votre compréhension, je suis très positif avec mon commentaire❤🫶🏽
C’est vrai mome
C vrai dh liga wakh
Je me suis dite la même chose après avoir regardé ce prank et celui avec Bibiche . Je trouve que même le fait de faire des prank sur leur sujet est un promo pour eux.
Drapeau mom dou yone nguéne défe ko sí vidéo bi toubab khamougnou lignouye wakhe mais khame nagnou couleurs yi dindi ko Mah stp
You tube moy lolou t gnome drapeau bi promo deguele pr mois bi gnou néke nako sa waye rafétoule
Alhamdoulila magal bi nieuw na😍😍😍😍
Yalla nagnou koo feke tee talco barkep khassidayis ❤️❤️❤️
Allahouma Amiiiiine
Magal gui lounou am ci la nouko ammée
Machallah khalise goor moko ndak
Biolay khalise adouna rel la yéme Guen la ndaw bilay yalna yallah mayla khalis bou vary tégua ameco nimou guena bakhé amine
Kou d'accord niou prank mahfousse lalal j'aime 😂😂😂
Lolou bayè k ak man ma dèfal lako😂
Kou d’accord niou prank wally😂🎉❤mahfousse ya meilleur kay
Amul tan kooku 🦾
Nono tous sauf golden boy❤😂
Mee😂
Vendredi prochaine nga prank boucher ketchup 😂 svp😂😢
Kone dè Dina wakh ba bôteu nguènè thi nguèbeuy gui😂
@@DioufMamesey-co6lyAy waaaaay dé na rek😂😂😂😂😂😂😂😂
j'aime yiguein di niane thi commentaires yi daniulein dithi faay khaliss wala louy probleme bi ak j'aime yiguein di am ?
BREF; le prank était super comme d'habitude
Prank lén Birima bou emission Jakarlo tfm 😂😂❤👍👍
Meunouma comprendre ga nek si youtube bi di niane vue kou d'accord rek lalall j'aime 😂❤
Yw miy😂nian j’aime nk
Toi aussi hein 🙄
Yangui niane di 😂😂
@@KHADYNDONG-b4p bayiko rk 😂😂😂
On réclame le prank de dieynabal tall série béte bete 😂
Dieynaba rek dina door mahfous dé
Kone dou mou door lène niom nieup😂
Kone dakoy mbéthie😂
Mag kou yarou la bialy
Salam mahfouz amna solo waye liko yakhe moy wan x bet rek ndakte day khertal khaleyi si kart te kart bakhoul
Jtm mag ndakh serigne touba❤
Mag kou buage serigne bi la❤
Très sincèrement linguay def nice na trop mais so meuné éviter themou lesbiennes wala you goor djiguene yi dina geuna nice
Mak vision beugu nako nak yok thi limako beuguon❤
Mag dafa digne am personnalité ❤❤
Wa gni nék si commentaires yi di out ay j'aime pour lanela, loléni doyé j'aime yi qu'est-ce que ca vous rapporte...!?!🤔 Bon travail Mahfousse 🙏🏽
Ah est-ce que bougouniou ci dieunde ndéki? Man deh beugu na kham si les "j'aime " se payent
Moma diakhal mane dhé damay mayé j’aime rék 😂😂
@@ngonediakhate8608 😂soxnassi dadjigama🤣
@@FatouFall-zp7ff man Kay dama yémou si nitgni, dagni saraxou pour am ay j'aime mélni kom j'aime Yi dagassiy am xaliss
Ça se voit que ni kou gueume bopame la té doylou machala bonne continuation frére ❤
Mahfouss do moromou raf daf tu est le meilleur walahi azim ♥️💪🏽
Mag machalla kou gueume yalla la alal dieuroul yi
Mag dh sipp na bou yagg il est très intelligent 😂
Dou mani det de 😂😂
Nonou lafa démé nak😂
Mag nk ya manqué kn lii soudone deugg la nii guay reagirer
Do dag Ndeye tothie Mbary merrei nla trop 😮
Makhfousss Aïssatou cœur brisé lagne beugue et Ramatoulaye 😂
Mahfousse na changé personnage yi gneupp khamé nalénne tamite comme ça sa sera réaliste 😢😢😢😢😢😢😢😢😢
Barke cheikhoul khadim khamoko doko deef Niang saa baye référence laa ci yonou seugne bamba
Makhfouss guirr dognou indill ngaka King baba🐐😂😂😂
Mais mag dafa daleu dei, mashallah nila niit ak lou meuna khew andal ak sa sang froid
Ay waay xbet bahoul😢😢yakneu gnou beuri
Magg on taime fort❤❤❤gnou serigne saliou lagnou beugg❤❤❤
Yena meuna provoqué nak mais mag machallah
IL FAUT TOUJOURS GARDER SA DIGNITÉ XALISS DIAROUL YENEU YII
bb elton xana nanguou wone apres rafetal nga defate scenario ak mome 😂 😂
Vraiment mag c’est un gars bien ohhhh machallah ❤❤❤
Kou beug niou prank maître EL HADJI Diouf lalale j'aime
Genre niou yarou nie comm magg 😂😂 sen prank dou guawa nekh dh😂dafay dém ba soff tellemen danio poser pour gua yeugual léne c tt un problemm
Bilay😂
Prank len wa coeur briser aissatou ak racky
Mouhamed ndaysane dafa yarou 🥰😅
Ana sponsor yi prank mahfouss dafey takh gnou kham vrai vie gars yi mahfouss le meilleur de sa génération 😊
Mag dékété yambar la nk sheut 😂😂😂
Mahfousss Prank sonko way 😂😂😂😂😊
Parank lene Racky Aidara
Pa assane Gueye lébou svp ❤
🤣🤣
Mashallah Mag Amna patience dhé 😂
Copin dawal lagn la sante dadial nonou kone😂😂😂
😂😂😂😂Kou réé lalal j'aime
Mah, attention! on commence à reconnaitre tes acteurs. Il faudra penser à les varier. Sinon toutes mes félicitations encore et mes encouragements. Bravo
Magvision talibe kou tedddd ki lah ❤🎉
Kou beug Niou prank Sanékh (Pére Ndiack's) rék lalal j'aime ❤😂
Yonla déh
Vraiment frr talibé deug gua❤❤❤❤❤❤
On réclame boy niang 😂
Boucher kethup prank bou sadik 😂😂
Gars yii tmt deugeur nagn boppou 😂😂😂😂
Bilahi mag ❤❤ da yarou talibé rek lay dokhé❤❤
❤Manchalla wzydji dioupna deugouna telna gueni si affaire yi
On réclame zall mbaye😂😂
Mak dama ko beug koi dafa calme😂
Kou d'accord niou prank marichou❤😂
Do léne prank Vj 😂
Samantha comunale bi❤❤❤❤ jetaimm❤
Ah mahfousse mouno pranker aissatou cœur brisé sltp