Nay rafet rek adouna nonoula mame serigne Fallou moy sama mame serigne Abdou karim di sama nidiaye. Mame Oumy Faye mo diour sama yaye, Mame Awa Faye mo diour Serigne Abdou karim ak sokhna Maï. Mais Man talibé cheikh la. Donc yalla Nay rafet rek
Cheikhoul Khadim beugou niouko ngir beugg adiana wala ragal safara djeumbeum ji mbacké rk laniou beugg walahi ta sa euleugé Lou yalla sounou borom dogal nexna niou 😍nioune sante naniou serign Touba sante bo khamni dafa diégidayo sante naniou yalla biniou boké si WA keur Cheikhoul Khadim 🙏❤️Gana mésséré l peuple est content rawatina nioune mouride yi ga khamni sounou lepp Serigne Touba Cheikhoul Khadim la❤️❤️Serigne Mountaqa Bachir yagg fi loll té wérr borom mbecté mi borom diamm ji Di Def lou bax si l'islam 😍😍🙏🙏🙏
Machallah serigne Gana vraiment nekhna trop yalnala serigne touba feyy,, mane serigne touba rk la guemm mom la doylo, moy sama yakar tey ak souba ak fougnou demm, Yalna done sougnou avocat kéroo fa yalla
Mention espescial aux techsien du groupe futur média. Cette émission restera inoubliable .(gana reck amoul lenne )dieureux djeufety serigne touba.serigne mountakha mbacke yalla nafi yague si barki serigne touba...
Mom Cheikhoul Khadim dafa défar leup ba nopi défar gnieup kéneu la kou yalla kendal mou ligueyal yalla ak Ya Rassoul ba yégu fim yeg defko nimko def té yémaléwouko ak len mom Cheikhoul khadim kouko moss doto beug lénène💞💞💞💞💞💞
Sérigne touba yalnala yalla faay sante ckheikh ahmadou bamba mbacké bouweur. Sérigne ganna messré doundale way yag sérigne khadim guéye ckheikh diop mbaye yalna yalla faay-leuh. Més j'aime bien outaz pape Hanne sama sopëlla
Ap doff wesoule gua begue Dieule Serigne Touba Khadim rasoussilah bayiko Mouride jamais Mane Talibe Baye la mais Serigne Touba douma nagou minda fonou yalla dimako guene begue bilahi
Ouatz pape hane liguay def kham nagne ko heur bou gana beugué khoussi si segne bii gua kallé ko wayé nak dagua khamoul kane moy serigne touba kokou beurigo si bartal la pouss mou déme ñaka pousse mou déme guéne balma nak si kaddu yi wa salam♥️🙏🏾
Nattou yi barena tropp kenn manoul dekkou Nattou yi koudoul ahmadoul khadiim amoul morom yalla ag Rassoulou lahi nioko tann.khana diangou leen ne ahmadou ne diamou na yalla niatti teemeeri djounni att bé yalla ag Rassoulou lahi guerem ma amoul morom Serigne Touba
Dieuredieuf serigne touba. SERIGNE MOUNTAKHA MBACKÉ yalla nafi yagg tee wer......MACHALLA serigne gana messeré yalla n'a yalla yokk kham kham bi wakhtaan bi amna solo.
Nio ngui doli sante cheikhoul Khadim rek ❤️ Ahmadou Dama xamoul souma nekoul wone sénégalais comment j’aurais fait ? Mane damay tokk diko xalat beu soneu , daldi xamni rek yalla béral nama loxo 😭 ma ngui doli sante yalla diouli ci yonente bi saw doli sante Serigne touba bu wer ✊✊
Kene dou Serigne touba Sénégal la Allah sedd loumou sedoul bene deuk si dunya djiko you yakou rek top toubab yi mais Sénégal sunu nekone si li keur diner santane walay niou raw béb deuk si adouna bi # être un sénégalais est un don comprendra qui pourra
Pape cheikh li yalna sakh thi beup tarikha cet émission doit être éternel pour tout les tarikhas nakh on pert beaucoup de temps sur sur itler et autre chose en classe de terminal poirkoi ne peut étudier l histoire de nos referants comme serigne touba l'âme le hadji malick baye niass ....
Baye cheikh waxgua lou ame so beugué si kaff sax mou wouyoula dama nék ak sama soeur mome s.fallou moy serigne niame mane serigne saliou .may déf brevet sportif daldi diaxlé si saut en hauteur ma taxawe niane ko si barké fallou néko yay borom na ame mou ame lirék lay niane sauter fimay amé 10 rék barki serigne fofou rék la yame taxawe di dioye s fallou ya youtou té yatalé
Kou beugue serigne touba khadim rassoul beusseul j'aime dieuredieufé borom touba khadim rassoul
OK@Thierno Lov.
7@Thierno Lo
Dieurediefaty serigne touba
@@amyndiaye7155 6ģ1
Nl
h@Thierno Lo
Serigne touba ken dou mom serigne bé fi man guen fi raw fi ahmadou ci kaw yalnako yalla guena fay serigne gana mésséré mouhtar yagual wéral
Djioulite la
Bokkou thi ndiabotou
Seydina Mouhamed
ba parei neikheuh
Mouride (Salihate) khana dou ma wara sante yallah ❤❤
Wawawww mouride rék mo nékh
Fatou kine Samb ❤️❤️❤️
machallah
Geune na geune rek
Santalle bay feithie ma chery BamBa si xol doyna Santeuh🙏🏾
Serigne bamba kouko bagne digua soonou ndakh mofi nek kou beugue serigne guana beuseul j'aime
Kou beug Serigne Ganna messré beusseul j'aime 🙏♥️
♥️♥️♥️
Dieuredieuf borom touba
Mw j l'aime beaucoup gana
😍
Gana corona 😅😅😅
Nelen dieureudjeufeti serigne touba kokou wakh yalna s touba fathie Saye adio❤️💖
Kou beugue Serigne Touba sa khol beuseul 👍
KoubeugueserigneToudasakholbueseul
@@matykebe7877 EA assez ses à¹à_
Kou Beug serigne Touba beusseul j'aime✨💟
Mbaba thié xol
Kepp kou beugu Serigne gana téwéko ay déwen ni déwen beuseul aime 🙏🙏 Serigne mountakha yalla nako fi yalla bayi🙏🙏🙏🙏
Amin
@@sokhnaaminagning5136 inchallah ami gning
Man deh sougnou wa keur ay tidian lagnou wayé man mom mouride la dieuredieufé serigne touba
Ahah lolou deh dou yaw rek deh beuri nga ci ay morom LoL
Nay rafet rek adouna nonoula mame serigne Fallou moy sama mame serigne Abdou karim di sama nidiaye. Mame Oumy Faye mo diour sama yaye, Mame Awa Faye mo diour Serigne Abdou karim ak sokhna Maï. Mais Man talibé cheikh la. Donc yalla Nay rafet rek
Mame yassine ziar bou werre waaye léppou bénla naasiri hakhe bille hakhe déko booléke khassaideyi dai guena baakhe rék
Waaw coumba
@@gassamakhadima2418 diadieuf khadim fassalé rek
Thiey sama wadji yalnagnou ko yalla fayal Serigne Touba 😭😭😭walay kén dou mom amoul mass amoul déndado khadim Rassoul Dina sakh si beug la ba abadan🙏
Amine
Amine 😍😍
@@mbayembengue3778 s
Wallahi kéndou serigne bamba
L homme de l anne pape cheikh diallo qui est d accord ☝?...
Moi
Toi wi MDR l'homme de l'année c pape Djibril fall points 😍👌
Moi
Moi
Bilahi j'ai des larmes au yeux
Cheikhoul Khadim beugou niouko ngir beugg adiana wala ragal safara djeumbeum ji mbacké rk laniou beugg walahi ta sa euleugé Lou yalla sounou borom dogal nexna niou 😍nioune sante naniou serign Touba sante bo khamni dafa diégidayo sante naniou yalla biniou boké si WA keur Cheikhoul Khadim 🙏❤️Gana mésséré l peuple est content rawatina nioune mouride yi ga khamni sounou lepp Serigne Touba Cheikhoul Khadim la❤️❤️Serigne Mountaqa Bachir yagg fi loll té wérr borom mbecté mi borom diamm ji Di Def lou bax si l'islam 😍😍🙏🙏🙏
Serigne mountakha mbacké yalla nafi yague loy te wer si barké borom touba 👌❤🙏
Amine
Man Maodo Mame Maodo la doylo wayé mognou diangual nagne sopou nitou yalla yi yallna gneup am Diam 🤲🤲🤲🤲
Bilahi Talibè Chiekh rek Ba faw
Bilay talibe mame bamba rek ba fatou
Serigne Touba d’où moromou benn Serigne li la wakh
FAMA NDIAYE Amna yo kham ni souma kay guiss damay tit ay dof deug ngen chim
Serigne touba ken la thi adouna amoul morom dieuredief serigne touba koubegue serigne touba besel j'aime
Serigne mountakha mbacke yallah naa fi yage amine yarabi barkép serigne touba khadim rassoul
Amine barki serign TOUBA
Amine way louka nara dall yalnanou dall
Ay way Yalla nama Yalla may borom keurou Mouride Sadikh gnou ande di ligeeyal Serigne Touba ak bep sokhna bouko beug🙏🙏🙏 Dieuredjeufé Serigne Touba
Ak mane mii
Amine
Amin
Mouride sadikh beug lol sokhna
Amy diop diayente nango ak yaw no mêle beugue Ndakhe Serigne Touba
talibè chiekh la dh wayè serigne touba mako beug
Mala beug yawite
Waw bamba nièpou lafi nèkal
Mala beug nguir bamba
Yawit nioleu beug
Ndeysan
Machallah serigne Gana vraiment nekhna trop yalnala serigne touba feyy,, mane serigne touba rk la guemm mom la doylo, moy sama yakar tey ak souba ak fougnou demm, Yalna done sougnou avocat kéroo fa yalla
Amine
Akssa Serigne Ganna messeré dieureudieuf kéne dou Serigne Touba Khadime Rassoul ♥️
Mention espescial aux techsien du groupe futur média. Cette émission restera inoubliable .(gana reck amoul lenne )dieureux djeufety serigne touba.serigne mountakha mbacke yalla nafi yague si barki serigne touba...
Dieureudieufeti serigne touba serigne mountakha mbacke yalla Nafi yag te wèrre Diam rek moy am inchallah ndam rek
Serigne ToUbA do morom tè do mass amoul dènèno bilahi walahi Serigne ToUbA kèneu leuh...
Amine
Gana Messére le mellieur kou beugeu serigne touba wakhal wawe
Bilahi mourid mei mém soumako nékoul wone damay fans serigne ndakh aye khar bakhame
l Lové You 💯 serigne Touba man mom légui nopp 100% ba aldiana 🙏🙏🙏🙏 serigne gana yallna sa diamo yagu amina si barke borom Touba amine ♥️♥️♥️♥️
Je suis talibe cheikh mai jaim Serigne Touba❤️❤️❤️
Amicalement. Il faut pas dire "mais" mais plutot et. Seurigne touba neina li mou nekk ak li cheikh nekk fa yalla la dieum
Dieuredieu serigne gana
MACHALLAH
@@cheikhnafall7101 p
@@sayengom8776 67
LE MEILLEUR C'EST CHEIKH AKHMADOU BAMBA🇸🇳❤💥
Alhamdou lilah bima yalla deffé mouride anti stress deug mooy beug serigne bamba
walahi
Dieureudieuf serigne gana sa bou gnou la dégué rekkk suñu fierté ak beug kou tedd gui di guena yokkkk. Yalnala kou tedd gui faye
Serigne Gana dh comme Serigne Same Mbaye
Il dit les choses tel quels sont ohh
Serigne Touba moy oxygène kokou beugoul do noyii🙏💗
Ndékè mane mouride la 🥰 👌🏽non kél khol bou nékh té cédeu👌🏽 merci pape Cheikh pour faire vivre ces moments 🤲🏽🙏🏼 DIEREDIEUFÉ SERIGNE TOUBA
P
Mom Cheikhoul Khadim dafa défar leup ba nopi défar gnieup kéneu la kou yalla kendal mou ligueyal yalla ak Ya Rassoul ba yégu fim yeg defko nimko def té yémaléwouko ak len mom Cheikhoul khadim kouko moss doto beug lénène💞💞💞💞💞💞
Billahi koukhasse ba niame serigne bi dousaff lénéne
Sérigne touba yalnala yalla faay sante ckheikh ahmadou bamba mbacké bouweur. Sérigne ganna messré doundale way yag sérigne khadim guéye ckheikh diop mbaye yalna yalla faay-leuh. Més j'aime bien outaz pape Hanne sama sopëlla
Ken du sering Touba... sering Touba kenna laa... love from a Gambian
That s true
Thank you
Tkx
You're right my Gambian brother. Serigne Touba is unique.
Ap doff wesoule gua begue Dieule Serigne Touba Khadim rasoussilah bayiko Mouride jamais Mane Talibe Baye la mais Serigne Touba douma nagou minda fonou yalla dimako guene begue bilahi
Ame nga foula dei bilahi
Wawaw wah gua deuguedé
Seydou Aw waxal dé je suis hommonyme et talibé Serigne wayé nak serigne sèp la beug dilèn wormal di sakou si ñiom ñian diarama
Waw waw ya ame foule de
Nieup ko beug bly
Kénn dou serigne Bamba
Serigne Bamba rek
Serigne Bamba képp
Serigne Bamba dong
Dieureudieuf Ahmadou Bamba
JeureJeufé iow miko wax Ahmadou reka gnou gnore nafsi wa dini souma abli wale walad wa maskani lakawadi atoun abate Ken dou Serigne Touba
@@taphambaye9337 waw gaurr yalla nala yalla défal jaam
Ouatz pape hane liguay def kham nagne ko heur bou gana beugué khoussi si segne bii gua kallé ko wayé nak dagua khamoul kane moy serigne touba kokou beurigo si bartal la pouss mou déme ñaka pousse mou déme guéne balma nak si kaddu yi wa salam♥️🙏🏾
Kene dou ahmadou bamba kou wakh amoul morom yalla na sa adio yepp fadiou amine
Billahi amoul morom
Amoul morome
Wallahi serigne touba amoul morom
Amoul morom
Amoul Morom
Yalla na yalla goudal fan ak wer gou yaram si barké serigne SALIHOU
Nattou yi barena tropp kenn manoul dekkou Nattou yi koudoul ahmadoul khadiim amoul morom yalla ag Rassoulou lahi nioko tann.khana diangou leen ne ahmadou ne diamou na yalla niatti teemeeri djounni att bé yalla ag Rassoulou lahi guerem ma amoul morom Serigne Touba
machalla waxtane bi amna solo trop doyalou niou deh Gana mome dagne lay nianal goude fane ak weurgou yaram rek sédal gua souniou khol
Mangui geuna sant yalla bima nekei djoulit nek 🇸🇳🇸🇳 teksii niou am Makk you teid dji souniou deuk bi
Dieureu dieufatiiii Cheikhoul khadim kén dou Brome Touba
Man mom mangui sante yalla bou werr ❤️🙏 Bimouma déffé Élément Serigne SALIOU 😍🙏
Kone Alhamdoulilah 💖🙏 yalle na yalla Wéral bate Gana Messer
Machala serigne ngana messere ak serigne khadim ak serigne cheikh Diop Mane mome Sama Mame bou Gor serigne fallou Mbacke diokh nako satal Mame laye diaw nioy Wa keur serigne fallou Mbacke dahira serigne Djili Mbacke touba Garki diaw mr
Diaw Mbéne machalla
Dieuredieuf serigne touba. SERIGNE MOUNTAKHA MBACKÉ yalla nafi yagg tee wer......MACHALLA serigne gana messeré yalla n'a yalla yokk kham kham bi wakhtaan bi amna solo.
Yalnaniou yalha fayal Cheikh Ahmadou Bamba .mbectém bép dioulite
Ngana Serigne khadim Gueye Cheikh Diop Mbaye Yalna guèn goude fane lool tè wèr amiine
Wawaw di sante sergine saliou mbacke bou weur defal naniou lepou billahi
Dieureudieuf serigne touba mbacké khadimoul Rasoul
Ganna messere mouride yep content naniousii yaw
Yalnanouko tewê ay dewèn
You barii diko tewlou 🙏🙏💘
Kou begue serigne ganna beuseul j'aime
Kéne dou serigne touba sounou khôl sédena lôle pape cheikh yalla naléne yalla takhawou
MachaAllah 🙏🏾 dieureudieufi akassa.Cheikh Ahmadou Bamba Khadimoul Rassoul si Khol yi. Serigne Gana Messere Dieureudieufi.
Thiey akhmadou qui suit cette vidéo jusqu'à présent beuseulma j'aime way sa barkép Mame saliou
Dieureudieufff Serigne touba jarama Mame chiekh ibra fall daww senegal renn germany dewenn touba keur bayy karim ak document cii barkepp borom touba veups
Mashalla s ganna messéré makhtar waxtan wii amna solo
Cheikh diop mbaye yallna yalla wéral bat bi
Serign touba amoul morom
Esk replay dakkoul💕Amalene diam ak tawfekh ak soutoura ak khewal ci barké khassaïde yi
Nio ngui doli sante cheikhoul Khadim rek ❤️ Ahmadou Dama xamoul souma nekoul wone sénégalais comment j’aurais fait ? Mane damay tokk diko xalat beu soneu , daldi xamni rek yalla béral nama loxo 😭 ma ngui doli sante yalla diouli ci yonente bi saw doli sante Serigne touba bu wer ✊✊
Depuis Algérie 🇩🇿 j’aime cheikh ahmadou bamba❤️❤️❤️🙏🏽🙏🏽
Guinaw yalla ak Mouhamed psl amoul kou fété serigne Touba kaww
Kendou s touba motakh niou am diamou barké Borom Darou ♥️♥️♥️💓💓💓
Akasa amna solo Dieure dieuf machalla Tfm Dieure dieuf serigne touba Mbacke amoul morom dee machalla yalnanguen fii yague the andack weure barkep serigne touba Mbacke
Serigne Mountakha yalla nafi yag té wére wayé kéne dou serigne Babacar sy mansour niakk thiakhane Sénégal 🇸🇳 yalla nafi diam yag
Yalla na yalla defal niepu diam thi barke alkhourane amine thi barke s touba amine
Ay way lou takh UA-cam meuno def 10000 j’aime 😭
Proud to be mouride khadim rassoul is one kou beug serigne touba besseul jm
Al hamdoulilah❤️nioun Serigne touba rek lagne beugue❤️yalla naniou yalla fayal cheikhoul khadim
Loudoul mom khadim walahi loudoul mom safou gnou😢😢
Codou Thiam yalla naniou ko yalla fayal
Thiaye cheikh Moustapha yallnaniou ko yalla fayall barkep bayamba
Kene dou Serigne touba Sénégal la Allah sedd loumou sedoul bene deuk si dunya djiko you yakou rek top toubab yi mais Sénégal sunu nekone si li keur diner santane walay niou raw béb deuk si adouna bi # être un sénégalais est un don comprendra qui pourra
Serigne gana yaw bayénanoula serigne touba
Diereudieuf serigne touba
Way ya bakh way📢
Wakathiko deh
vrai mon ami à partir d'aujourd'hui Parce vous êtes expérimentés
Dieureudieufeuti serigne touba
Yalla na fi serigne mountakha yague lol te ande ak were
Dieureudieuf Cheîkhoul Khadim Mbacké 💖💖💖
Serigne bi c'est pour tout le monde kel waroul nangou koula si euplé ak fo mana bok 🙏
Dieureudieuf serigne touba bayilen pape hann way beugnoul serigne touba dakh wakhnako bimiy commencé nena kou bagne serigne bi beugo l'islam
Dieureudieuf Serigne Touba
Ndeysane mane mourite la mais wakeur mame baye niass danio yarou lool té bakh yalla na sen diam yague 👏
Sante serigne touba khadimou rassoul rek sasounè amoul morom ☝️ te moroman tewoul ♥️🙏🙏🙏🙏🙏
Dieuredieufeuti S Touba amoul morom Mbacke Balla aicha yallah na niou ko suniou borom fayal...
Ana Kou buegue serigne bi
Magui ni awmasi sagoo dh
Mangui ni
Senegal khamouniou liniou ame ( serigne touba khadimou Rassoul) Senegal yèp nio wara manko Wakh Dieuredieufeti serigne touba khadimou Rassoul.
Walahi sant ko faràta la si gnoune ❤️❤️
Sokhna natta mbaye Dafa lerr machalla 🙏🏼🙏🏼🙏🏼🙏🏼
Dieure dieuf serigne mbackiyou faye yalnafi yague the andack weure barkep serigne touba Mbacke
Pape cheikh guoudeul fane serigne bi gueureume nala❤❤❤❤🙏🙏🙏🙏💖💫💥✨
serigne Modou Moustapha
Lugeyal na serigne bii mo heuth Rayy bii nakh diouma dji machalla
diereudieuf
Ana Wa Keure Serige Touba Mbake Beuslene 👍❤
Djeureudjeufé serigne touba yalna naniouko yallah fayalll
Dieurdieurf serigne touba amoul morom bene rek la fi ♥️♥️♥️serigne mountakha mbacke balla yague fi lol te weer♥️♥️♥️♥️
Amine way mourit
Amine
Aminé
@@babacarseckelectricienbati9089 Ģq1
Pape cheikh li yalna sakh thi beup tarikha cet émission doit être éternel pour tout les tarikhas nakh on pert beaucoup de temps sur sur itler et autre chose en classe de terminal poirkoi ne peut étudier l histoire de nos referants comme serigne touba l'âme le hadji malick baye niass ....
Beugue Serigne touba day farata sii nitt kou nioull.Barkép Serigne touba😭
Degg na degg bouwer❤️
Bilaahi farata bou réy
LIMA MENUL COMPRENDRE MOY NIIT KU KHOLAM BI MENUL SUPPORTER SERIGNE TOUBA.
BAMBAA nékha begueh, gniko begueh dagnuy féékh té sunuy khol dafay dundeh diammi BAMBA; dieureudieufety CHEIKH AHMADOU BAMBA KHADIMOU RASSOUL
Wawaw ték rail guir diouma , mouride yi rékka KO déf.
Gni yalla dimbali gneup kham nagnou ni Serigne Touba amoul moroom
Walahi chiekh diop mbaye linga wakh sakh khamoko
Ki bour yallah ni momla yonèntebi ni momla kounè woul momla douniou saf ahmadou rèck mom kèp rk dongou ba fawou dieureudieufè serigne touba ❤
Kou Begue Serigne TOUBA WanéLL Sa Bopou
Serigne touba ki deuk ak yalla kharitok seydina mouhamed rassoulilah s.a.w.s
Thiey serigne touba li dou nene na niep nagoul serigne touba mou nekh
Kouné kham na kou meun bayam wayé bo guéné faral sa baye
Dieureudieuti Akhmadou Bamba
Baye cheikh waxgua lou ame so beugué si kaff sax mou wouyoula dama nék ak sama soeur mome s.fallou moy serigne niame mane serigne saliou .may déf brevet sportif daldi diaxlé si saut en hauteur ma taxawe niane ko si barké fallou néko yay borom na ame mou ame lirék lay niane sauter fimay amé 10 rék barki serigne fofou rék la yame taxawe di dioye s fallou ya youtou té yatalé
Serigne touba est un bien fait de dieu pour tout l'humanité pour éternelle dieureudieufé serigne touba khadimou rassoul le serviteur du prophète psl
S Bamba dou kén amoul kon koy tekeléll
S Gana Yeugue fi te weur ❤️❤️❤️👍🏾
J'adore Gana Massere❣️... Très pédagogue, très agréable à entendre, et très civilisé
Uk o
Thiey serigne touba amoul morom déh diamou yalla bou weer begue seydina Mohamed psl
Machallah Dieredieufff brom Touba cheikh Mohamadou Mountakha Mbacké yàlla na fi yague ta wër ci barkeb ku tëdd qui Aminnne Aminnne Aminnne