Personnellement je ne fais pas partie de ceux qui se disent talibé d'un quelconque marabout..mais Bilahi wolahi je vous le jure Elhadji Malick Sy m'a ébloui de par ses enseignements de par sa sagesse Bilahi magui sésé nii contane na trop cii Mame Maodo Sy je viens de me rendre compte de la dimension incommensurable de l'homme Bilahi contan na Bég na sama xol bii séd na
Je suis Mouridoullahi et j'aime beaucoup SERIGNE BABACAR SY MANSOUR: Yalna Yalla (SWT) méyko goudou fane ak wérgui yaram si barké Serigne Mounetakha Mbacké té yokki lééram si barké Seydouna Mouhamad (SAWS)
Mane talibé serigne saliou mbacké la wayé dama Buege serigne babacar sy Mansour bilahi ndakh simplissime walay yalla na yalla goudal fanam mame abdou rk lamaye fatali🤲
SERIGNE BABACAR SY MANSOUR YALLAH NAFI YAGG LOLOU TÉ AND AK WERRR, SERIGNE MOUNTAKHA YALLAH NAFI YAGG LOLOU TÉ AND AK WERRR, KOU WAKH AMIN YALLAH GUA FI YAGG KHÔL YEUP CONTANE TAAY SERIGNE TOUBA CONTANE N'A, EL HAJ MALICK CONTANE N'A DIEUREUDIEUF TFM❤️🙏 PAPE CHEIKH YALLAH NALA SUNU BOROM SOUTOURAL AK MBOLEM DIOULITT 💖🙏
Walahi sama xol sedna Yalla na gneup am diam gnou nék beneu dioubo délou si Yalla ak Yonentém bi Mouhamed (PSL) serigne yi dagno ligeuye ba am lignou am dougnou ay enemi febar bi Yalla nafi diougé si barké serigne yi Mame maodo Serigne touba Baye niass seydina limamou laye boukouneta si barké gnou téddeu gni mangi diégalou si kaddu yi
Ma shaa Allah, Al hamdoulilah. Yalna yalla defal nieup diam. Le Sénégal est un et indivisible. Il faut préserver cette richesse incommensurable que Dieu nous a octroyée. Que Dieu accepte notre jeûne et efface nos péchés🙏🏽🙏🏽🙏🏽❤
Machaallahou, le mystérieux, l'intellectuel, l'organisateur, le modeste, le savant, le philosophe, le rensembleur... L'inconnu de la nation sénégalaise.
Machallah khool seedna trop!!!Niaak si doyaal si wakhetaane bi motakh ba légui nioguikoy setaane fi depuis la France 🇫🇷!!! Contaane naniou trop si sunu pédagogue bi serigne Alioune Diagne wakhentaane bi rafetna tei nekhna machallah ! Nioune dh ay ndaaw nanou mais yaguiniouy khamal louniou khamoul woone
Bilahi walahi wa talakhi je suis très content d'avoir SEYDI EL HADJI MALICK SY mais aussi très fière d'être TIDIANE yalla nagnou yalla fayal Maodo fayalgnou mak gniou bakh gni si rew mi🙏🙏🙏🙏🙏
Barkeb Serigne Babacar contane na jljr😭❤❤❤Yalna diam yagg Machallah, Mame Babacar sy mansour tricher wo say Mame rek ngua nirol si modestie, simplicité, am yarr, Maodo wanouniou bopam deh, Ya Rasoullilah lagnou xamal, sa Faye Maodo après lay done niou beuri xamougn leu, mais mangui sant bama néké Talibé cheikh fonk sougn diné, fonk sougnouy wadiour, respecter les autres tarikha Machallah sama xol mo fess😭❤❤
Machalah, khol sedena, que Dieu nous accorde sa Grâce et nous protège du coronavirus. TFM merci, pour ces séances formidables. J'ai découvert Cheikh Ibra Fall, j'ai compris le message de Mame Limamou et suis conforté par les bénédictions divines sur Mame Maodo. Que Dieu les rétribue. Par ailleurs, TFM serait inspirée de nous proposer une émission mensuelle sur les vénérés guides religieux et leurs compagnons. Yalla nalene yalla diapalé.
El Hadji Malick Sy Ibn Ousmane l'inconnu de la nation senegalaise . Il n'est pas Dieu ni Prophète mais un homme , un sujet de Dieu d'une extrême rareté qui a su allié la raison et la foi de sorte que ses dires et ses actions sont toujours bénéfiques pour l'humanité . En vérité seule une personne saine d'esprit et raisonnable est capable de voir à quel point Malickouna est unique et a véritablement un mérite extraordinaire .
Talibé Serigne Touba ni yw lay mél billahi Mais pas vidéo bi di daw en direct Saga yi di daw si commentaires yi no démbou dama rouss Lii dou Sénégal bou mak gni diougé noo 🤔
Machallah amna solo lol yalla na diam yague,niep béne laniou fébarbi yalla nako fi yalla dieulé guire dieumi seydina mouhamed (psl) yalla na niep am diam si barcké serigne touba mbacké
Les mots me manquent pour décrire la joie et le Bonheur que je ressens en regardant cette émission. Yalla nagnou yalla féyal Elhadji Malick Sy Dieurdieuf Mame Maodo Diarama Alioune Diagne
Di remercier pape cheikh Diallo ak ses braves Dames yi si sén sérénités avec leurs ouvertures d’esprit machallah!!! Sénégal lila sokhela on es fier de vous😘 wayé kén dou Oustaz Pape Anne machallah rk Yalna Yalla yokkou meune meune bii ak kaataane bi inchallah!Dieureuguéne Dieuf🙏🏾Yalnanou yalla déff deug deug Talibé cheikh 🤲🏻
MACHAALLAH, Diné dji dou Classico ! Sougnou Mack gni gnoom gneep benn lagnou, sen mission moo doon ISLAM sampou si Sénégal. Merci à Saydinà Alioune Diagne et le Khalif Général pour leur discours d'unité de la Umma.
Yalna Yallah fay Serigne bi. Yalna niou Yallah arr nioune nieup, samm niou, doli niou soutoureu,mousseul niou si lèpp lou bonn, si fébbar, ak si bala. Yalna niou Yallah gueuneu khirr si lou bakh, si diammou ko, té niou am moudj bou rafett
Billahi khol yii séd n'a Al khalifa Sérigne Babacar Sy Mouhamadoul Mansour n'a fi yallah yagal lol andeu ak wér Sérigne Alioune Diagne n'a la yallah barkél content nagniou Macha'Allah TFM
Dieye Serigne El hadji Malick Sy ❤🤩yalla maynako lum mayoul ken yalla naniouko yalla fayal, waye ken dou Mame Brom Touba❤🤩 wallhi yalla defalnako lum defaloul ken yalla naniouko yalla fayal, ak suniou mak nioubakh nieep 🤩 ❤
Jaaxay ken dou môme walahi ,il ne s'est pas nourri de la religion mais il l'a nourri ,il fut la personne honorable devant laquelle toutes les âmes se pâment,qu'Allah sanctifie l'oeuvre de Seydi Hadji Malick.Merci walahi nekh na yalla na yalla fayal niou mague gni
Mame mourite la Waye wakhtane bi nekhna Wala mane tidiane la waye wakhtane bi nekhna mano lene bayi Lolou borom kham kham moy Wakh force day nekh Diagne yalla na yalla goudal sa fane Dieureudieuf
Macha Allah Oustaz Aliou Diagne wallahi nekhna deyssane diarama Oustaz, Maodo Malik dé nittou yalla yi gnoko cédé thii ham hamam mo nekh Immam kepp waliy yalla
Machallah quelle modestie le khalif général yallah na yallah yagal takhawaybi té mou andak wer serigne Alioune Diagne dieureudieufeuti yallah na yallah wereul batbi 🙏🏽🙏🏽🙏🏽
pour une 1ere dans l'histoire de ce monde un khalife général qui appelle en direct dans une emission via téléphone, lii rek léçon avant say kadou yi, bou heurou wakh dioté rek mou wakh déloci khel yi, booléwatt nite gni noppi, Sy Malick yalna BUUR BI fayalnioula. sama khol tay nimou fékhé yalna lérou Rassulilah tourou sa kaw. serigne alioune diagne yakk say diang katt gatié ngalama
Macha allah je suis 100% mouride sama khôl sedna lolo thiaye mame el haji malike ak serigne Babacar sy borom bonikari bii yalla nano yalla fayal sono mak ngie amine❤️
ماشاءالله ياقائل القول الصحيح قد زهزح القلوبنا بالفرح والمرح حتى لا ندري اين نبدا واين ننتهي بسبب المحادثتك ،على الشيخ الحاج المالك سه الذي بذل دموعه لرفع الكلمة الله والسنة النبي ، الحمد لله الآن نعرف من هو سيّد الحاج المالك ، هو ضوء من الضياء الله ونور من الأنوار الله كان مجاهدا لنشر الإسلام في الأنحاء العالم
Walakhi Mame Maodo moy le stratège le plus fin;le plus intelligent, kendouko diapeu di yeew di yobou Gabon . Je témoigne en tant que talibé Baye Niass. Talibé cheikh rek.
Yene gni di dingante akh khasteh, boko lepp ci yonou Bamba, boko lene ci yonou Cheikhou Tidiane. Nakh teh sunu kilifa yi worma akh teguine lagn niou diangal
@james Harden mbokk mi, boul ci khol lolou. Yeuf yi dou nieukenteh, wala door fayou. Niit meunoul tagg wala mou khalabb Seydil Hadj Malick wala Cheikhoul Khadim, ba sene grade ci Ya Allah wagnekou wala yokou. Mbir mi dou dioganteh, Ya Karim khamna kane moy kane teh noppi na
Kell sagess seugn mbaye sy mansour yalna yalla goudalll sa fann banga egalekk sa saggoo sy malick fière d'être talibe cheikh yalnaniou yalla rayy si tarikha cheikh
Sant yalla bimou gnou khirtalei si yonou tarikha Cheikh 🙏🙏bolegnou nak ak goor gou tedd gou magg gogou di Seydil hadj Malick Sy yalla nanou ko yalla fayal🙏❤
No hier fi wathina 😂😂😂❤️❤️📿📿📿📿📿ak Élément perturbateurs yi 🤔wayè kenne dou Maodo daan na📿Fouta ni nagnou gongo olof ni mbaye daan na❤️👏🏾👏🏾👏🏾📿📿📿📿📿kennn dou yoe si mim rew ak fenen
Akkassa Ndeyssane seydina Alioune Mii bégu n'a ci moom lool bilaahi wayé gnongui lay gnaanal wér ak wérlé ci barkép Sheikh Ibrahima fall,, Franchement kham kham bi sélna té rafétna Mashalla♥️
Limassiy ték nak mooy ,guaayiy saagua ci direct yi démlén khoolaate sén ndiangualém kilifa yi ,Seydi Elhadj Malik digueulouko kén Sérigne Touba ossi digueulouko kenn🤲 Koussi maytuwoul sa bopp nak dingua lor sa bopp
Personnellement je ne fais pas partie de ceux qui se disent talibé d'un quelconque marabout..mais Bilahi wolahi je vous le jure Elhadji Malick Sy m'a ébloui de par ses enseignements de par sa sagesse
Bilahi magui sésé nii contane na trop cii Mame Maodo Sy
je viens de me rendre compte de la dimension incommensurable de l'homme
Bilahi contan na
Bég na
sama xol bii séd na
Yalna yalah content
Mashalla yalnanga beeeg rek si barke seydi haj Malick
Mame MAOUDO il n 'enseigné ke SEYDINA MOUHAMMAD ( PSL) rek...
Ndeyssane c’est normal vu sa simplicité et son respect au Sounna du prophète qu’il jura de respecter et de ne jms le ternir
Badara essayé de chercher sur youtube seringe Habib Sarr il a fait un cours sur seydil Hadji Malick
Je suis Mouridoullahi et j'aime beaucoup SERIGNE BABACAR SY MANSOUR: Yalna Yalla (SWT) méyko goudou fane ak wérgui yaram si barké Serigne Mounetakha Mbacké té yokki lééram si barké Seydouna Mouhamad (SAWS)
amine yarabi ya bakhe déé
Dé nga bakh
Dagua bakh ngone Fall mane j'ai rêvé 4 serigne touba et pourtant talibé cheikh la kone nak lep béne la
Diereudieuf mbok contann nan
Amine yarabil alamina
Non.ce monsieur est fantastique et pleins de savoirs.quel fierté d'être talibé cheikh. Le savoir fait la différence.
papa Diouf bhl
Way doundal way
Walay ndayssane c'est vrai deee
Papa Diouf va cherche sur youtube tu cherches oustaz Alioune diange sur cheikh tidjane
Bilay ndayssane
Billahi barki seydina MOUHAMED psl deib ku sa❤️ Seidoul dafa feikkk ni fanatiques gua do musulman nax ❤️ yeuppa togn th yeuppa 😭 Billahi yalla n’a fi jamm yag th keipp ku beug seydina MOUHAMED psl beug Maodo beusseul j’aime
Amineee
Nn bilahii Ta raison
Kaine dou Mame maodo degloul li oustaz moudou fall wah ua-cam.com/video/w6RRCEEwzeI/v-deo.html
Mane talibé serigne saliou mbacké la wayé dama Buege serigne babacar sy Mansour bilahi ndakh simplissime walay yalla na yalla goudal fanam mame abdou rk lamaye fatali🤲
Mahcallah amine yarabbi yalla na yalla goudal souniou fan nioune geupp wollahi Diamm rek ngay am incahallah
😘😘😘
Walahi mouhamad lép bén la
Beugue gua nite kou bakh simple bala gua kaye khame deugue gua toke ak mome🙏🙏🙏🙏🙏
Amine amine inchallah🙏❤ diam si yaw
SERIGNE BABACAR SY MANSOUR YALLAH NAFI YAGG LOLOU TÉ AND AK WERRR, SERIGNE MOUNTAKHA YALLAH NAFI YAGG LOLOU TÉ AND AK WERRR, KOU WAKH AMIN YALLAH GUA FI YAGG KHÔL YEUP CONTANE TAAY SERIGNE TOUBA CONTANE N'A, EL HAJ MALICK CONTANE N'A DIEUREUDIEUF TFM❤️🙏 PAPE CHEIKH YALLAH NALA SUNU BOROM SOUTOURAL AK MBOLEM DIOULITT 💖🙏
Machallah amine
inconnu bilahi man dh morid la wayé kontan na trop say tané yébari rk wayé am nan ay nit you bakh
Amine
@@falloufall1684 bilakhi segn Fallou, Maan mi Talibée serigne cheikh séye souhaibou mbacké la, nitt kou bakh dafay wakh lou bakh 🙏❤️
Amine
Kou sa khol sèèdeu beusseul j'aime❤
Deja fait🙏
Machala
@Jaffiche mes stars qqqa as àapQ
@Jaffiche mes stars aq
Sac pp
Walahi sama xol sedna Yalla na gneup am diam gnou nék beneu dioubo délou si Yalla ak Yonentém bi Mouhamed (PSL) serigne yi dagno ligeuye ba am lignou am dougnou ay enemi febar bi Yalla nafi diougé si barké serigne yi Mame maodo Serigne touba Baye niass seydina limamou laye boukouneta si barké gnou téddeu gni mangi diégalou si kaddu yi
Machallah machallah 🥰🥰😘😘☝️☝️☝️☝️☝️☝️☝️☝️☝️☝️😭😭😭😭
Wakhe tane wi amna solo trop suis mouride ms dama beugue tijane
Yalna diaam yaag Sénégal danio am ay kilifa you baax
Merci gora 🙏🙏🙏
Yalna la Yallah beugu! 🙏
Ndaysane nonou lagnou beugué ndiabootou cheikhoul khadim bamba moy maoda yalna yalla déf diam si réwmi 🙏👏
Walahi ndéysane. Gora. Yala nassa jamm yagg...
Je suis trés content Billahi .Di ballou ak nieep di nianal Pape cheikh Diallo mou yague fii looool waaay0
Amine
ce monsieur est éloquent.. Message fluide ,claire et plein de sagesse .
Uujbubm à hauteurjp
En tant que mouride sama khol bi dafa sedd trop machallah
Serigne babacar sy mansour yalna yalla goudal say fane ak kilifeu dinè yepp
Amine ya rabi rafetna machaala yala na yala fayla
Ma shaa Allah, Al hamdoulilah.
Yalna yalla defal nieup diam.
Le Sénégal est un et indivisible. Il faut préserver cette richesse incommensurable que Dieu nous a octroyée.
Que Dieu accepte notre jeûne et efface nos péchés🙏🏽🙏🏽🙏🏽❤
Machalla
Machaallahou, le mystérieux, l'intellectuel, l'organisateur, le modeste, le savant, le philosophe, le rensembleur... L'inconnu de la nation sénégalaise.
MAODO!❤
Cheikh Seydil Hadji Malick❤😭
Il est modeste vraiment il a dit bal léne ma si Cadou yi antanque khalif général machala
Ndayssan ndiabotou Maodo yi donio am yar
Nogaye Sall diapou si réck boul convoqué sama gayi
Kaine dou Mame maodo degloul li oustaz moudou fall wah ua-cam.com/video/w6RRCEEwzeI/v-deo.html
@@yattayatta8954 😂😂😂
Machallah khool seedna trop!!!Niaak si doyaal si wakhetaane bi motakh ba légui nioguikoy setaane fi depuis la France 🇫🇷!!! Contaane naniou trop si sunu pédagogue bi serigne Alioune Diagne wakhentaane bi rafetna tei nekhna machallah ! Nioune dh ay ndaaw nanou mais yaguiniouy khamal louniou khamoul woone
Machallah Barcké Mame Cheikh Ibrahima Fall Sénégal dall riche na Yalna diam yagg barcké YONÈTEBI "ALKHAMDOULILAH" 🥰💖💘🇪🇸🤝🇸🇳🙏🙏
Amine way, yalla df ka si domou sénégal yeupp
Neh na hk yoy war eilo bdou hklpa yallah Qeqq
Talbe si touba la waye wahtane bi amna sola loll yala na diamou yage si rew mi Aminn
Bilaye moussa anne ya bakhe yalla nala yalla faye sibareke serigne touba
Amine
Merci waye sangbi amna solo trop yalla khamnako
Oh les sénégalais vous avez un pays extraordinnaire. Machaallah. Repentez vous et accourez vers votre Seigneur le Tout Puissant
Mashalla ❤️🙏🏽
Bilahi walahi wa talakhi je suis très content d'avoir SEYDI EL HADJI MALICK SY mais aussi très fière d'être TIDIANE yalla nagnou yalla fayal Maodo fayalgnou mak gniou bakh gni si rew mi🙏🙏🙏🙏🙏
Aduna amoul soloo na niou rakhass kholl yi rkk defar jikoo yii
Yalla nagnou yalla may khol bou gnou andé done béne
Je suis mouride mais dama danou lér mancha Allah
Yallah naniou Yallah tass si barké mag you bakh yi
Amine yaraby yalna yalla Nangou niane yeupeu inchalah merci
ndeyssane da nga bakh
Lepp béne la
Lepp béne la
Bilaye ya bakhe
Mouride tidiane layenne niassen nieup ben la niou yalla Sénégal dieum kanam tee yalla dieuleniou fii mbass mii
Amine khol sédna
Walay mame dabah rekk la beug man mouride sadih bii serign bamba rekk laa yakar
Walay gnoune gneup bénn lagn, yalla nagnou yalla samm
Bilahi wakh deug
Barkeb Serigne Babacar contane na jljr😭❤❤❤Yalna diam yagg Machallah, Mame Babacar sy mansour tricher wo say Mame rek ngua nirol si modestie, simplicité, am yarr, Maodo wanouniou bopam deh, Ya Rasoullilah lagnou xamal, sa Faye Maodo après lay done niou beuri xamougn leu, mais mangui sant bama néké Talibé cheikh fonk sougn diné, fonk sougnouy wadiour, respecter les autres tarikha Machallah sama xol mo fess😭❤❤
Yaag lol Sy Malick ibn Balkhawmi
Vraiment je prie de tout mon cœur que Dieu aide les gens qui ont eu la capacité de mettre un dislike qu’il revienne sur le droit chemin😭😭😭🙏🏻
Ils sont malades wallah!
Amiiinnn car ils en ont vraiment besoin 🙏🏾
Machalah, khol sedena, que Dieu nous accorde sa Grâce et nous protège du coronavirus. TFM merci, pour ces séances formidables. J'ai découvert Cheikh Ibra Fall, j'ai compris le message de Mame Limamou et suis conforté par les bénédictions divines sur Mame Maodo. Que Dieu les rétribue. Par ailleurs, TFM serait inspirée de nous proposer une émission mensuelle sur les vénérés guides religieux et leurs compagnons. Yalla nalene yalla diapalé.
Merci beaucoup sy malick
Machalah Merci beaucoup 🙏
Machallah
Machallah yalla naňu yalla fayal seyidil haaji maalik sih
Yala.na. yalla fay. Yiw tfm
Machala
Senegal d warnano doli sante sunu BOROM si kilifa yi nou amm...
Yalla na diam yag barkep SERIGNE TOUBA
Talibé daniokoy yar si xam xam kén douko yar si khar bakh ak karama yalnanio yalla fayal sounio magnio bakhgni
je s8 talibè bamba mè mame maodo sougnou fièrtè la kèpakou bëug dinè dieuredieuf bamba dieuredieufè maodo sènn ligèybi rafètna yalnalènn talibè yèpp dëgg
El Hadji Malick Sy Ibn Ousmane l'inconnu de la nation senegalaise . Il n'est pas Dieu ni Prophète mais un homme , un sujet de Dieu d'une extrême rareté qui a su allié la raison et la foi de sorte que ses dires et ses actions sont toujours bénéfiques pour l'humanité . En vérité seule une personne saine d'esprit et raisonnable est capable de voir à quel point Malickouna est unique et a véritablement un mérite extraordinaire .
Hoolalaa Sama khôl ❤️sedd na trop kenne dou Mame Maodo yalnaniou yallah dess ayy talibé cheikh si Barké yonenti bi Amine 🤲🏼🤲🏼🤲🏼🤲🤲🤲🌹🌹💞💞💞
Waw gor diagne amna solo loll machalla suis mourid mai sama ❤ bi sede na trop barki serigne touba
Bilaye ya bakhe
Yalnay cedd ba faw
Talibé Serigne Touba ni yw lay mél billahi
Mais pas vidéo bi di daw en direct
Saga yi di daw si commentaires yi no démbou dama rouss Lii dou Sénégal bou mak gni diougé noo 🤔
Machallah amna solo lol yalla na diam yague,niep béne laniou fébarbi yalla nako fi yalla dieulé guire dieumi seydina mouhamed (psl) yalla na niep am diam si barcké serigne touba mbacké
Sarr Awa Amiiine. Ni rek la dioulite yi warounio bayi kene di niou roubé
Les mots me manquent pour décrire la joie et le Bonheur que je ressens en regardant cette émission.
Yalla nagnou yalla féyal Elhadji Malick Sy
Dieurdieuf Mame Maodo
Diarama Alioune Diagne
MERCI BEAUCOUP
Di remercier pape cheikh Diallo ak ses braves Dames yi si sén sérénités avec leurs ouvertures d’esprit machallah!!! Sénégal lila sokhela on es fier de vous😘 wayé kén dou Oustaz Pape Anne machallah rk Yalna Yalla yokkou meune meune bii ak kaataane bi inchallah!Dieureuguéne Dieuf🙏🏾Yalnanou yalla déff deug deug Talibé cheikh 🤲🏻
Machalla je suis mouride wayé kontan n'a lolou yalnala yalla samb khalif général
MACHAALLAH, Diné dji dou Classico !
Sougnou Mack gni gnoom gneep benn lagnou, sen mission moo doon ISLAM sampou si Sénégal.
Merci à Saydinà Alioune Diagne et le Khalif Général pour leur discours d'unité de la Umma.
Alhamdoulilah khole seddati neu, yalna yalla défe diamm au Sénégal et partout dans le monde amine 🇸🇳🇸🇳🇸🇳🇸🇳🇸🇳
Amine yaraby yalna yalla Nangou niane yeupeu inchalah merci
@@abybathily8221 amine , merci
Machalla amna solo machalla
Aminé
Tout le monde est content ❤️❤️❤️🙏🏽🙏🏽🙏🏽
Serigne Babacar Sy Mansour khalif général des Tidiane yalla nga fi yagua té wer sounou serigne 🙏🏼🙏🏼🙏🏼🙏🏼❤
Amine in-cha-Allah
Serigne sopenala té yala takh, blilahi. Que Dieu vous donne une très longue vie. J'adore Sidy Elhadji Malick Sy , Serigne Babacar Sy.
Machallah Yalnaniou yalla deff deugue deugue talibe cheikh amine ya rabi
Amineee way
Allahouma Amine
Yalna Yallah fay Serigne bi. Yalna niou Yallah arr nioune nieup, samm niou, doli niou soutoureu,mousseul niou si lèpp lou bonn, si fébbar, ak si bala.
Yalna niou Yallah gueuneu khirr si lou bakh, si diammou ko, té niou am moudj bou rafett
Yalla na yalla goudal say fane oustaz Alioune Diagne ci barke Mame maodo
Amineee
Machallah xol sedna 😍 talibé cheikh woyof ragal yalla akk beug prophète bi psl laniou ko xamé yalnaniou yalla fayal mame MAODO
Machallah
Machalah amna solo yalla na diam sah Senegal si barkep khassida yi barkep serigne touba
Machalla ken dou mame maodo mome rek si khol dara dasa khadjoul bayou KHALIFA❤
Alhamadoulilahi Alhamadoulilahi
C'est ça le Sénégal ❤
Yo Allah diounou gourndam ma
So Allah mi wéltim,Sénégal fof wéltim ❤ sy malick ❤
C vraiment incroyable fière d'être talibé cheikh
Billahi khol yii séd n'a Al khalifa Sérigne Babacar Sy Mouhamadoul Mansour n'a fi yallah yagal lol andeu ak wér Sérigne Alioune Diagne n'a la yallah barkél content nagniou Macha'Allah TFM
Talibè Cheickh rek labegeu donne bilahi🙏
Yalla nagnou ko yalla bolé déf machallah
Yalnalako yalla défal
Dieye Serigne El hadji Malick Sy ❤🤩yalla maynako lum mayoul ken yalla naniouko yalla fayal, waye ken dou Mame Brom Touba❤🤩 wallhi yalla defalnako lum defaloul ken yalla naniouko yalla fayal, ak suniou mak nioubakh nieep 🤩 ❤
Machalla ken dou khadim rassoul 🙏
Bilay kedou mame babacr
@@aidandiayegueye5807 ❤🤗
@@aidandiayegueye5807 ❤🤗
Li moy senegal dama contane
Jaaxay ken dou môme walahi ,il ne s'est pas nourri de la religion mais il l'a nourri ,il fut la personne honorable devant laquelle toutes les âmes se pâment,qu'Allah sanctifie l'oeuvre de Seydi Hadji Malick.Merci walahi nekh na yalla na yalla fayal niou mague gni
Thieuy serigne babacar sy mansour y'a oyof ta bah way
Manchalaa mame SEYDIL El Adji MALiCK Lér la gou léral leup nék chance pour gnoune wa Senegal ak UMA bi yeup
Mame mourite la Waye wakhtane bi nekhna Wala mane tidiane la waye wakhtane bi nekhna mano lene bayi Lolou borom kham kham moy Wakh force day nekh Diagne yalla na yalla goudal sa fane Dieureudieuf
Wokhofi dara
Wakhofi touss sa xéll celloule
@@papeelimanesene2979 Dieureudieuf pape elimane
Macha Allah Oustaz Aliou Diagne wallahi nekhna deyssane diarama Oustaz, Maodo Malik dé nittou yalla yi gnoko cédé thii ham hamam mo nekh Immam kepp waliy yalla
Les diangue kat sont trop forts Machallah.
Will Blacked sidy mbaye la domou daw gor mbaye
Will Blacked demb rétane naleu beu sone sheuu😭😭😂😂😂
@@saergaye505 😂😂😂😂👍🏾👍🏾👍🏾
Machallah yalla na yalla wéreul seni bate
Les diangues kat kay.. Yaw mom amo stress 😂😂😂
Yalna nio yalla fayal sunu DIAMBARE DJI ❤CHEIKH SEYDIL HADJI MALICH ❤kenn dou mome machallah walahi très fier d'être talibé cheikh❤❤❤❤❤❤❤
Diam si yow
Ayaww yalla na yalla tape kholyi ma sha Allah talibe cheikh lakh mais je respect toutes les religions 💯
Machalah j suis fiere detre talibe chiekhe amine
@@oumoudiagne70 amine yalla nanou ko yalla defal
😗😗😗😗😗
Serigne el hadj malick sy kéne dou mome dieuredieuf serigne alioun diagne ak pape cheikh diallo 🙏🙏🙏🙏🙏
Bilahi walahi kéne dou Maodo thiey Mame Maodo hier j'étais tellement content ,khôl yii seed naniou yalla yalla fay léne tfm sur pape cheikh
Machallah yalla nagnou yalla fayale Mame El Hadji Malickh Sy ak djabot gui
Macha'Allah maodo
Fière d'être talibé cheikh mais je respecte les autres religions je suis vraiment contente pape cheikh ak wa groupe TFM que Dieu vous bénisse
Nekhoul ba nekhoul wayé Quartier general mongi soga ame gane
Machallah quelle modestie le khalif général yallah na yallah yagal takhawaybi té mou andak wer serigne Alioune Diagne dieureudieufeuti yallah na yallah wereul batbi 🙏🏽🙏🏽🙏🏽
Machallah machallah Diagne yalla na sa diamou yageu ak kouné ammine🙏🙏🙏
Amine
Machallah notre fierté khol sedd na yalnala yalla fayyy contane na trop
Machalah amna solo barké borom Touba yageu fii lol té wer SY
Ndayssane khol sédeu neu ame yalla rek mo nekh th woor ❤️❤️❤️
pour une 1ere dans l'histoire de ce monde un khalife général qui appelle en direct dans une emission via téléphone, lii rek léçon avant say kadou yi, bou heurou wakh dioté rek mou wakh déloci khel yi, booléwatt nite gni noppi, Sy Malick yalna BUUR BI fayalnioula. sama khol tay nimou fékhé yalna lérou Rassulilah tourou sa kaw.
serigne alioune diagne yakk say diang katt gatié ngalama
Dieureudieuf mame maodo yalla nagnou yalla def talibé Cheikh
Macha allah je suis 100% mouride sama khôl sedna lolo thiaye mame el haji malike ak serigne Babacar sy borom bonikari bii yalla nano yalla fayal sono mak ngie amine❤️
Yalla gneup am diam reck Mame Maodo & Borom touba fierté sénégalais la kne nagnou yalla Tass sisséne barkéé reck si barké kou tédd kii ....Talibé cheikh si❤❤❤❤❤❤❤❤
Machalah yalla na niou yalla bolet dèfal niou diam je suis mourid mes je ne peux plus garder mes l'arme 😭😭
Machallah kéne dou MAME MAODO, YALLA NA YALLA YOKOU LÉRAME😍🙏❤️💕
Amine yarabi
Amine yarabi
@@ndeyenguirane2419 hkooek
Amine yarabi
Xol sedd na li moy senegal yalnaniou yalla fayal maodo
ماشاءالله ياقائل القول الصحيح قد زهزح القلوبنا بالفرح والمرح حتى لا ندري اين نبدا واين ننتهي بسبب المحادثتك ،على الشيخ الحاج المالك سه الذي بذل دموعه لرفع الكلمة الله والسنة النبي ، الحمد لله الآن نعرف من هو سيّد الحاج المالك ، هو ضوء من الضياء الله ونور من الأنوار الله كان مجاهدا لنشر الإسلام في الأنحاء العالم
Macha Allah ensemble tt le Sénégal ba aldjana Yalla nagnou ko Yalla defal ci barké mak gnou baakh gni❤❤❤🙏🙏🙏
Ken dou Mame Maodo😍
Yallah neuniou ko Yallah fayal Sy 🙏🏾
Macha alla serigne alioune diagne yalla na sa diam yague si bake seydina mohamed psl
Chapeau a vous serign alioune diagn xamxam rek nga wané yalnala yalla deffal diamm té gueneu sellall xamxam bi 😘😘😘
Walakhi Mame Maodo moy le stratège le plus fin;le plus intelligent, kendouko diapeu di yeew di yobou Gabon . Je témoigne en tant que talibé Baye Niass. Talibé cheikh rek.
Will Blacked ❤️❤️❤️
Doundal way
Wakhofi dara doul rékk kén dou Modou Mbacké la preuve kholol nombre de vue yii jour Mame Cheikh Ibra Fall
Yene gni di dingante akh khasteh, boko lepp ci yonou Bamba, boko lene ci yonou Cheikhou Tidiane. Nakh teh sunu kilifa yi worma akh teguine lagn niou diangal
@james Harden mbokk mi, boul ci khol lolou. Yeuf yi dou nieukenteh, wala door fayou. Niit meunoul tagg wala mou khalabb Seydil Hadj Malick wala Cheikhoul Khadim, ba sene grade ci Ya Allah wagnekou wala yokou. Mbir mi dou dioganteh, Ya Karim khamna kane moy kane teh noppi na
La dimension spirituelle de Seydi hadji Malick sy depassait nos frontieres yalla na yalla fayalnioukou amine touf toufffff 😍😍😍
Amineee way
Machallah xol seed na. Alhamdoulilah bignou necké Sénégalais
Kell sagess seugn mbaye sy mansour yalna yalla goudalll sa fann banga egalekk sa saggoo sy malick fière d'être talibe cheikh yalnaniou yalla rayy si tarikha cheikh
Sant yalla bimou gnou khirtalei si yonou tarikha Cheikh 🙏🙏bolegnou nak ak goor gou tedd gou magg gogou di Seydil hadj Malick Sy yalla nanou ko yalla fayal🙏❤
Azize diage yalla nalla yalla Faye adouna ak alahira si barké sèydina mouhamad salalahou alayhi talibe cheikh pir moy yaw vraiment
Al hamdoulah baniou bokei cii sopey Maodo❤️
Machaallah sy Malick dama dioy ba toubab yima deukeuk diakh fi si espagne longue vie yalna BOROM bi fay yiw inchaallah xol yi sed na machaallah
No hier fi wathina 😂😂😂❤️❤️📿📿📿📿📿ak Élément perturbateurs yi 🤔wayè kenne dou Maodo daan na📿Fouta ni nagnou gongo olof ni mbaye daan na❤️👏🏾👏🏾👏🏾📿📿📿📿📿kennn dou yoe si mim rew ak fenen
Yalna niou yalla fayal Seydil hadji malick amoul morome fier d'être Talibé cheikh EHMS NOTRE SECRET
Ma Sha ALLAH
diné islam rek mo woor
dieuredieuf serigne alioune diagne
kéene dou Mame Maodo
Le QG de l'année mashallah😍
Yala na yala déf diam sénégal si barké seydina mohamet saw. Dieureudieuf seydi hadji malick sama tourando
Talibe cheikh ba deeeee 😭😭❤❤♥️♥️
Ba dhhhh
Kousi contanne beuseul j'aime🥰
Abdou aziz Ndiaye yalla na diame yague si linga deife si barkei el hadji Malick ...
Akkassa Ndeyssane seydina Alioune Mii bégu n'a ci moom lool bilaahi wayé gnongui lay gnaanal wér ak wérlé ci barkép Sheikh Ibrahima fall,,
Franchement kham kham bi sélna té rafétna Mashalla♥️
Limassiy ték nak mooy ,guaayiy saagua ci direct yi démlén khoolaate sén ndiangualém kilifa yi ,Seydi Elhadj Malik digueulouko kén Sérigne Touba ossi digueulouko kenn🤲
Koussi maytuwoul sa bopp nak dingua lor sa bopp
Machallahou Sy Malick yalna yalla goudal sa fan te dolli diamma ci biir reewu Sénégal amiine.
Serigne Babacar sy Mansour yalna fi yague ak mbokam cheikh mountakha ci barké khadimou rassoul
Amine
pape cheikh tu n'est pas trompé du sible machalla sur ton invité dieudieuf sunu makgni
Mashalah s'y Malick goudou fane ak wergu yaram rekk yala bayi lafi fi basi kanamm bijay seydil woudiou Di sws♥️❤️