Tu n pas mon lutteur Gris mais cette fois ci je t'ai beaucoup respecté, les gens n comprendre pas. faute d'arbitrage.. Je vois beaucoup commentaires qu'ils parlent mal sur Gris, je vous demander c'est le vrai Balla G2 qu'est la? Haha 😆 Bella da périmé il lutte seul sur Mystic Modou Ravage lay xar, il te cherche aussi Boy Niang.
Gris tu as bien lutté. Tu es un vrai guerrier et c'est ton plus beau combat depuis celui contre Eumeu Séne. Tu n'as pas eu la victoire mais tout le monde te respecte.
Mdrrrr gris ya wax medina da am ay cadre ay ministre ... Donc lou takh débloquer wougnou sen xaliss né nga Dakar moy xewlé loutax defoléne différence boulgnou sonal balla a bien lutté yéméla di songue di door bene mystique boulkofi wax
du courage Mbeur sui un fan de Balla Guaye mé vraiment t'a pas d'emérité j t'encourage continue tes entraînements ,t décourage, et respect ton adversaire c'était un môment inoubliable vous vous êtes dites des choses mais le passé c'est du passé
grris nous sommes pas aveugle et je ne pense pas k nous sommes fous tu devrai fermer ta bouche au lieux d’y jetai de l’huile ta pas combattu et si ont dit vrais balla même sil ne mérite pas sa victoire tu aurai du avoir le courage de l’affronté comme un homme prend 3 jour de repos enferme toi dans ta chambre et regarde comment tu a combattu
yaw dou ya done wakh meunouniou dorrr 😂😂😂😂 ton visage montre l contraire balla dou sène niékhou niébé mais demal inscrit jeu olympik yi daww rek guay Def 😉😉😉🙊🙊🙊🙊
Pour moi quoi qu'on puisse dire Gris Bordeaux a bien bien lutté Donc touts mes respects Diantal men nga continue tes entraitements Pour tes prochains combats Parceque un profesional ne doit pas bessé les bras Pour des defaites de se genre. CNG doit revoir les reglements Pour l'espectacle y aussi Pour les amteurs C'est du n'importe quoi.. Wa Salam 🇸🇳 🇸🇳 🇸🇳 🇸🇳
gris boul niak ba paré nianki bala dafla féksi sa fort battre lasi aférou lac 2yi nak nopil tamit sa discours bi amoul sakh logik nank rk sa blem moy tu te croi plu intelligent k aux autres lutteurs reviens sur terre ngemb ngay tak comme eux
"Balla moy Bandit" deug deug. Yakhna kanamou saway akou noppyii. Gris de guissoul degoul, Lou maodo wakh mouni han? Yawde jespere que prevoir nga vegebom ak beurre de Karite. Boy Balla moy bandit pire. Nooon Ngaka bi defaral na Nandite bi. 9h ba 19h dielefa kanam gou newi ak nopeu you Boucher, non wakhlenma Lou bandit di nourou?
Saway yow khamngani Gris Bordeaux bou beurrélone boppam sans consignou Mbaye Guèye kône Gris dina door Balla Gaye ba rayko tay wa Fass nioko takhawlo mais Balla Gaye mi Fanani Stade nak 1h du matin té meunoul dann Gris nakk !
Bilay balla moy sama mbeur mais gris guerrier nga franchmen et tu es tres correct, tu n’as pas démérité !!! Ndeyssane maodo rak dji beugam dey fegn gravement dérétt mo fort !!!
Goor nga wayy teyy balla yeuguelnala pertlonala sa memoire pertlonala sa memouwarr Outal carite ak khorom ndok bou tangue niuu dappala sa canam nga Bal ma Thii wak wak bii
Gris yaw do rousse balla fékela sa point fort meunelaci dorela bagay daw et tu ose dire ya yoré lamb sa lokho stp ne te fous po de nous beuréwo dara. Balla lagnu wakh
Les journalistes arrêtez de dire quelque chose que personne ne vous a dit Balla Gaye 2 a dit que il lui donne une minute s'il ne vient pas lui il va venir alors arrêtez d'inventer des histoires
Boulène niou ray way Gris Bordeaux consigne leu Beurré môtakh mouy reculé mais Balla dooroufi dara loudoul ay coup en l'air à part Diappanté mouy dougeul upercute kou menoul dann Gris koy dann Boy bou ndaw Gris makk leu fouf
Dama xamoul loutakh nga gniak fayda,au lieu di wakh ni bala may tekki sama ndiemb ma nek roi des arènes,mais ngay nan douma gniekhou nene ken ay mbeur douma fowé ni-nga gnaké fayda kholal affaires bi yew lëë boul ki guené sa bop mëun nga nek roi des arènes so gueumé sa bop par ce que dann nga B52 mais maintenant il est roi des arènes. Mais par contre Balla gaye II est un vrai lion 😂😂😂 félicitations pour lui
Je suis fan de Balla Gaye , Mais je reconnais que tu as bien assuré. Félicitation
Balla noy moy too saa nonee 👉👉👉Ardoo Gris noy moy too saa nonee 👉👉👉Yambaaaaa😂😂😂😂😂😂😂😆😆😆😆😆
Moi je supporte balle je suis très contente mais gris du courage
nènè dia baringathiy morom
Félicitation Balla gaye et du courage gris...yalna Yalla déf diam si sénégal amine
J'aime la lutte sénégalaise mais le CNG est très nul. Ya pas gagnant ou perdant. Les lois de la lutte doivent changer.
Tu n pas mon lutteur Gris mais cette fois ci je t'ai beaucoup respecté, les gens n comprendre pas. faute d'arbitrage.. Je vois beaucoup commentaires qu'ils parlent mal sur Gris, je vous demander c'est le vrai Balla G2 qu'est la? Haha 😆 Bella da périmé il lutte seul sur Mystic
Modou Ravage lay xar, il te cherche aussi Boy Niang.
mais Gris kagne la deurrrrrr... Door yii moudiou na mettii dehhh....Balla a vraiment marqué son retour
Bon courage champion vraiment tu était brave tu a résister jusqu'au bout je suis pas un supporteur de gris mais tu a de mérite qu'on se dise la vérité
Merci gris balla modou lo mongi gneuw gnapp sa ndaye yaw ak aziz ndiaye ak baye ndiaye ak balla bèye sèytané rajim
Merci bro vrement sa ete bien passé.c sa un homme il fau merite tes millions
bilahi. beureee. nga. deug. gris . felecitation
un cri de coeur et de fierté envers toi Gris... tu as bien géré ton combat car tu as suivi les conseils et ordres du staff. le meilleur reste à venir
Gris wakh rék ngay téwé say supporter mé pas beuré gris le roi des communicateurs
Gris tu as bien lutté. Tu es un vrai guerrier et c'est ton plus beau combat depuis celui contre Eumeu Séne. Tu n'as pas eu la victoire mais tout le monde te respecte.
Mdrrrr gris ya wax medina da am ay cadre ay ministre ... Donc lou takh débloquer wougnou sen xaliss né nga Dakar moy xewlé loutax defoléne différence boulgnou sonal balla a bien lutté yéméla di songue di door bene mystique boulkofi wax
du courage Mbeur sui un fan de Balla Guaye mé vraiment t'a pas d'emérité j t'encourage continue tes entraînements ,t décourage, et respect ton adversaire c'était un môment inoubliable vous vous êtes dites des choses mais le passé c'est du passé
Kholl koo rekk Balla Gaye dafaa deugueu ndayam baa taugne dii Yabeu domeram diee saa taugne yii dii mell nii Yéteu bou eumbeu Amo Sakh diom GIGi légui dou Gris GiGi Laaaa😂😂😂😂😂😂
xallé réw Baa doff réw gua yaw do dém
Xallé réw Baa doff nafi
Senegal, Gambia, Guinea bessau, we all support BALLA GAYE 2, Balla gaindee win rek❤💙💚💛💜
Good job Gris Bordeaux!!!! May Allah bless you and your family.... Thank you 👏👏👏✊✊✊
Balla bi ma guiss taye dou balla bi ma khamone. Gris a été à la hauteur. Balla dotoul nek balla bou ndieuk ba. Dopage bi yakh n'a yaramame.
grris nous sommes pas aveugle et je ne pense pas k nous sommes fous tu devrai fermer ta bouche au lieux d’y jetai de l’huile ta pas combattu et si ont dit vrais balla même sil ne mérite pas sa victoire tu aurai du avoir le courage de l’affronté comme un homme prend 3 jour de repos enferme toi dans ta chambre et regarde comment tu a combattu
Non Gris bett ngama. Yaakaronn naani priipp nga 4 appuis mais resister nga bou bakh. Vraiment du courage. Balla mom gadday yam bou metti bi yeupp meunn beureim daffaa diaarei naaw
Vraiment mes félicitations gris et aussi à bala ,magret ta défaite tu es un champion.
URGENT : LA majeure partie de ces supporters sont des gamins
gris ba faw incha Allah
Du courage gris ce n'est pas une dèfaite billaye do gnèkhou gnébème fèlicitation
😀😁😁😆😆nooo Gris balla ta tuè aujourdhui avc tout tes favori c est la bas qu on ta dominè les coup de point !!!
Kou bagne défaite boul beurè! Balla si khôl bi gris du courage ÿaura une prochaine fois
Gris bordeaux vous êtes courageux ET bonne continuation tu à bien lutter Big UP
yaw dou ya done wakh meunouniou dorrr 😂😂😂😂 ton visage montre l contraire balla dou sène niékhou niébé mais demal inscrit jeu olympik yi daww rek guay Def 😉😉😉🙊🙊🙊🙊
Ndeysane Gris dafa dianakhé mounoul sax wax bou bakh😂😂wax rek lay def dina def ba gueine si néna mystique
Gris balla soula ni kay niou lewto ngeu bagne soulani kay niou beurré ngeu bagne soulani kay niou khékh ngeu lolou baxoul dégeu soko défé dafay yakh sakanam bi
Alhoussein sene ki kanaman Toth na
Billay lutteur le plus populaire mais gayi dounie ko wakh🔥😢tout dakar es dérriére lui
du courage on est tous derrière toi inchallah balla mounoul fekhe ba dane la
Balla bayou mbeur yii goudall fane yay nékhal lamb dara douko dindi
Ndeyesane bilahi nak yalla nala yalla di diaballé
*Nguir* *yalla* *boulén* *suivre* *gris* *suivre* *len* *rakk* *dji* *khol* *nimkoy* *kholé* *rek* 😆😆😅😅
Pour moi quoi qu'on puisse dire Gris Bordeaux a bien bien lutté Donc touts mes respects Diantal men nga continue tes entraitements Pour tes prochains combats Parceque un profesional ne doit pas bessé les bras Pour des defaites de se genre. CNG doit revoir les reglements Pour l'espectacle y aussi Pour les amteurs C'est du n'importe quoi.. Wa Salam 🇸🇳 🇸🇳 🇸🇳 🇸🇳
Gris yow do touss. Tapeite ngeu boul gnou sonnal. T'es fier d'être un fugitif kay.
gris boul niak ba paré nianki bala dafla féksi sa fort battre lasi aférou lac 2yi nak nopil tamit sa discours bi amoul sakh logik nank rk sa blem moy tu te croi plu intelligent k aux autres lutteurs reviens sur terre ngemb ngay tak comme eux
niakkdiom.com il parle comme s'il avait gagné le combat ki dal ay supporters lay weur ak beug prouver que dou yambar xptdr
Du courage GRIS yone yamoul thi ben tkt pas❤👈
You are both great , bless you both . You are in top form bless .
mashallah gris diambar nga chapeau à toi Talibé cheikh
"Balla moy Bandit" deug deug. Yakhna kanamou saway akou noppyii. Gris de guissoul degoul, Lou maodo wakh mouni han? Yawde jespere que prevoir nga vegebom ak beurre de Karite. Boy Balla moy bandit pire. Nooon Ngaka bi defaral na Nandite bi. 9h ba 19h dielefa kanam gou newi ak nopeu you Boucher, non wakhlenma Lou bandit di nourou?
Elwaly Ndour lol
ELWAY NDOUR YANGUI MAY REY BILAHI
Elwaly Ndour non tu ma tué lol sérieux
Niak diom nak wesouwoul li ngay wakh. Maodo yaw nopil
Saway yow khamngani Gris Bordeaux bou beurrélone boppam sans consignou Mbaye Guèye kône Gris dina door Balla Gaye ba rayko tay wa Fass nioko takhawlo mais Balla Gaye mi Fanani Stade nak 1h du matin té meunoul dann Gris nakk !
Gris more respect to you,, you really do your promise.. Good luck bro 😎
Mercii GRIS contane nañ si yew
Xana lac2 mola conseiller taye 😂😂😂😂 tewul gnam nga d👊👊 balla rek
Merci tu as dien lutte
Waa mais sa Kanam bii tamit déformée naa😨😨😨😨😥😥😥
Fatima la reine Ngom boyy bien dit
Bilahi balla rayna domou ndiambour 😢😢😢 khawnako ray ndeyssane
gris yowe Lou bala ame bo ko amone kaine wokhetou ko tu un champion sitore ndoure bougoule seize Ndiaye li ko merci yowe khame gue mome khamena
Fatima la reine Ngom
Way ki kayy 😀😀
Fatima la reine Ngom kou wakh lep mbame yi matala gris war na wakh dara boudh amna xele Sénégal dale moy dekou libertés
gris this is not a victory for balagaye ,but yours you are a lion allah bless you at all
Balla mo gagnè deh wayé masoul ame combat bou mètè ni proud of you gris diambar nga
Bilay balla moy sama mbeur mais gris guerrier nga franchmen et tu es tres correct, tu n’as pas démérité !!! Ndeyssane maodo rak dji beugam dey fegn gravement dérétt mo fort !!!
Courage gris yalla bakhna
ndeyssane yallah rékk mo meune beaucoup s'attendé a ce que gris douma balla gaye
Goor nga wayy teyy balla yeuguelnala pertlonala sa memoire pertlonala sa memouwarr
Outal carite ak khorom ndok bou tangue niuu dappala sa canam nga Bal ma Thii wak wak bii
Nice nice bravo gris vive fass diadieuf Medina rek fass rek
Afer bi yawla bro daye bakh inchallah
Mes c'est normal gor yalla deug geu gris Ken merewoula bilay walay oné fiér de toi
Courage gris tu n'a op demerit3 ,walahi Dieu l'a decid3 ainsi
Tu as bien travaillé merci
Franchement une victoire banale
Dagua done rassou rkk diguéne sakou yii door yala diap bo nopalo diapal 2stv dakh mou lér té gua guana you dji affaire bi guédiawaye lh Mouy nékh Mouy nakari
May wakh mounàn moyen yaw lounioula diàpalé nga dieundéko yambà koulay diápalé thiiim niakk diom demal diàyi sa yàmbà dji balà lambou
bilay respecte wo wa fass tu te fou des gens .
Chui 200000% balla gaye mais g pitié de Gris lol mais nak wouyouma Gris niam nga deh😆😆😆
Du courage beurénga dh contane si iow c'est pas la fin du monde
Gris yaw do rousse balla fékela sa point fort meunelaci dorela bagay daw et tu ose dire ya yoré lamb sa lokho stp ne te fous po de nous beuréwo dara. Balla lagnu wakh
Tu courage a vous deux vous avez bien lutter
Your brother is really sad
Les journalistes arrêtez de dire quelque chose que personne ne vous a dit Balla Gaye 2 a dit que il lui donne une minute s'il ne vient pas lui il va venir alors arrêtez d'inventer des histoires
Gris gaindei la maîtrisé na boy.. Balla warul sah yag ak gris.. Un vieu de 40ans ngay yagg ak mom ni... Ah balla mom shui dzl mai parrewul
Gris Comba bi mome contane na si yaw bilahi 🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏
Macha allah bilay ta bien joué mbeur
Champion du courage mais tay khaw ga dai non tay ana sa bagarre dala rere khana
les potentiels adversaires de Gris Bordeaux gris-ama baldé boy niang - gris tapha tine-gris gris -lac 2
Du courage machallah 👍👍👍💋💋💗💗💗
Way nopil defo fi dara balla khawnala rayy
Balla do darra , avertissement dou ndammm , défiant gua
C'est à cause de votre défaite tu est nul et tu as peure Balla gaye2 des années des année Balla gaye2 c'est le vrai lion 🦁
Boulène niou ray way Gris Bordeaux consigne leu Beurré môtakh mouy reculé mais Balla dooroufi dara loudoul ay coup en l'air à part Diappanté mouy dougeul upercute kou menoul dann Gris koy dann Boy bou ndaw Gris makk leu fouf
Laisse les parler gni daniouy sopp rek balla meunoul dara si gris bordeaux.
Doudou Diongue ioe guani doryi dalloul.boula gris deguè gua kham
Doudou Diongue ya sokhor ki danoul gris mo am 19 voctoir xana dangako fattei
Ndeye Sylla mdrrrr non sister ray ngama
tu as parfaitement raison bro
Bravo gris Balla est plus jeune ke toi mais il ne l'a pas montré. L'essentiel c'était de ne pas tomber. Diadieuf gris
Gris sa kanam bi nice na dh koula defni kou mounoul xèhh
Machallah frère ioe brom khol bou nice nga ta gental grand
Tey mom linga beuré massoko beuré. Bravo
AHHH Gris dicourage DIAMBAR gua mai Balla Champion la loooll
Franchement il a bien lutté hier malgré tout
Wa Gris mi louko daal, dou nagou li yalla dogal, yaw niou door-la daan-la ngay wakh!!! Amo diomm sakhh
Yaw doul pa bou toll ni yw do rousss sahhh dawww combat bi yeupp so taxawonnn niou dann dann bou bonnnn domramm
Blyy ya beurreih beurreih biii xeixxx xeixxx biii
Arbitres yii nio 👎 👎 reikk
Félicitation Gris
gris rek on est content de toi
Bilay beuréga déee tay môme machalah
Bilahi mala beugueu gris woorna yalla
Non tu es un vrais guerrie ms Les arbitres sont touts guatte ms felicitasionts
Gris t'a bien lutté courage sa ira incha allah
Dama xamoul loutakh nga gniak fayda,au lieu di wakh ni bala may tekki sama ndiemb ma nek roi des arènes,mais ngay nan douma gniekhou nene ken ay mbeur douma fowé ni-nga gnaké fayda kholal affaires bi yew lëë boul ki guené sa bop mëun nga nek roi des arènes so gueumé sa bop par ce que dann nga B52 mais maintenant il est roi des arènes.
Mais par contre Balla gaye II est un vrai lion 😂😂😂 félicitations pour lui
gris on t'aime. mane sah tahnga ma beug nek medinois.
balla gaye 2 la farale mai gris adouna ni la yalla moye doquale dcrge
Gris Moss nga d danga Bari wakh nak nopil douma yi mettina
toggal fofouu doffou médina yii dila diayy wala danga dieleutiii sa affaire yoyouu tamite..gris bayyil yamba bii
😂😂😂😂😂iow gnou door la bagua beugue dh nane douma niekhou niebé ak gris amale touti diome😂😂