« Lac 2 dadone sathie motakh niou…» Selbé Ndom détruit Lac de Guiers 2 Mauvaise nouvelle pour Lac 2

Поділитися
Вставка
  • Опубліковано 16 тра 2024

КОМЕНТАРІ • 48

  • @bijoukane
    @bijoukane Місяць тому +5

    Thieuy selbe neina dafa done sathieu reik far dal di feigne thieuy yallah nagnou yallah soutoural

  • @beuzhustle3483
    @beuzhustle3483 Місяць тому +2

    Bilahi deugeu dou rombe noppp ..... vérité rekkk lafiii waxx

  • @Ma-zb6bo
    @Ma-zb6bo Місяць тому +5

    Selbé ligua wahh deug leu MÉ nak natou dou wéss TÉ YAGUI DÉFF LOU ARAM MOUYE PÉTAW 🐚 YAGUI WAHH LOUDOUL DEUG TÉ FÉNE DAY YEUGUEUL ARASS YAGUI TÉKAMIL DISI WATT LOUDOUL DEUG
    ADOUNA AMOUL SOLO

  • @user-bc9wy6hb1e
    @user-bc9wy6hb1e Місяць тому +3

    Masta yalnako yalla guener mais nakh deugue da nekhoul mais elle a raison , yaw nekho ambassade di dougou si affaire vis

  • @ahmedgueye8067
    @ahmedgueye8067 Місяць тому +5

    Tay mom je suis d'accord avec toi

  • @LayeBa-mg7mj
    @LayeBa-mg7mj Місяць тому +2

    Mane dh dama diakhlé nakh sénégalais defaitou diambour dagn ko beugu c dommage

  • @user-yo9oc8ci1t
    @user-yo9oc8ci1t Місяць тому

    Franchement tay mom elle a dit la vérité

  • @issasamb835
    @issasamb835 Місяць тому +2

    Yalla bakhna

  • @Lg2.8
    @Lg2.8 Місяць тому +3

    Ayyy waaayyy défouko yeneu diapaleleneko mou gueneu rek t yalla takh

  • @abdougaye8856
    @abdougaye8856 Місяць тому +9

    Pourtant mère bi deguelawakh

  • @mika-fh3cj
    @mika-fh3cj Місяць тому +2

    Wakhal lokhame nak

  • @cheikhtoure7600
    @cheikhtoure7600 Місяць тому +3

    😂 mer bi amoul kw

  • @mathusalemchanel3314
    @mathusalemchanel3314 Місяць тому +8

    1er fois mou wakh louma daccord
    na gayi bayi door

  • @alsanefall9074
    @alsanefall9074 Місяць тому +1

    Ndaye Féne Rek Masouta Guise Papaye Lada Guer

  • @BassirouSarr-nn6rq
    @BassirouSarr-nn6rq Місяць тому +1

    Salbé ndom xana lac doussa cluan motakh

  • @cheikhdiane7181
    @cheikhdiane7181 Місяць тому +3

    na refètt

  • @khadysagna2294
    @khadysagna2294 Місяць тому +6

    Da nga ame ndiabotte ragalale yalla na wakhe dji rafête natou d'où wess

  • @babacardiop6125
    @babacardiop6125 Місяць тому

    Deugue rékk nga wakh.

  • @abdoutoure2490
    @abdoutoure2490 Місяць тому +1

    Garde. Kooru. Mounoul. Malaka dara🤣🤣🤣🤣🤣

  • @mohameddam759
    @mohameddam759 Місяць тому

    ❤❤

  • @deugrek344
    @deugrek344 Місяць тому +1

    Yaw amo béne lécon boy diokh kén. Sénégal yafi dakha fén bouniou nékone thie deukou yone yaw waro wakhati. Dagua fén ba maguette. Adouna beussou wérou koor la fiyak diante sowoul dioubou mane na am.

  • @ThiernoSow-mz3bo
    @ThiernoSow-mz3bo Місяць тому +4

    Selbé yaw niatta yone gua féneu fii yaw Lou khew liguay wakh worou lah

  • @sophrotall8105
    @sophrotall8105 Місяць тому +1

    Tay mom wakh nga DEUG

  • @assanesene8337
    @assanesene8337 Місяць тому +3

    Ay maman salbé yangui diokhogne bãramou touma lac 2 ningay wakhé dou nii des esk moko déff attention des

  • @bocarcisse2970
    @bocarcisse2970 Місяць тому +1

    Bagua wakhet heure gua wara nopi

  • @amethdiagne4889
    @amethdiagne4889 Місяць тому

    Maintenant les marabouts qui arnaques akkk baxoul bayui lénn tokk mouy dokh té dem ligeyui yapa sou metier

  • @mamadoupene4149
    @mamadoupene4149 Місяць тому +1

    Variété SaLBÉ NDOME ❤❤❤

  • @user-mx5fo5eq1n
    @user-mx5fo5eq1n Місяць тому +5

    Lac. De. Guiers. Kou. Niak. Diome. Leu. Na. Rembourser. Khalissou. Diamboour. Yi

    • @teuweude1551
      @teuweude1551 Місяць тому +1

      😂😂😂😂😂😂 Noon kill ngama koi

    • @Al_Hamdoulilah
      @Al_Hamdoulilah Місяць тому +3

      Khamouniou sakh fond problème bi Adouna kounek meune nga dioum, borom mi tank dou rétane lafagne nakh adouna dafa goudou tank

    • @cheikhdme412
      @cheikhdme412 Місяць тому

      Deugue leu yao bou féké daga bok si gnime lék sa xalise war nga ko nial mou guénusi diolite waro yéné sa mbok dioulite la mane mi lék nane sama xalise mais nara féte

  • @khady-zr3so
    @khady-zr3so Місяць тому +1

    féne ak doule mo gueuna bone té yangui koy défff

  • @nitoudegeukaddudegeu3001
    @nitoudegeukaddudegeu3001 Місяць тому +1

    TOI MAMAN SELBÉ ❤ jumelle de ma mère ❤ je t'aime bien bilahi ❤❤ mais bala Nga digeulé sangou day fèkeu Nga sétt ❤ féen moy ndeyou Bakar yi wakhoumala di door kamil sa lokho di watt Si loudoul DEGEU,, pétaaw dafa Haram , xéssal dafa Haram 😊AUSSI NIIT DAY WAKH LOUKO WOOR YAW XAMO HISTOIRE BI RÉELLEMENT NOUMOU DÉMÉ DONC ESK DO MANDOU PASK DAGUA AME AY DOME TÉ ADOUNA DAFA GOUDOU TANKK✊🏿 C'EST VRAI LAC 2 DAFA NIAKEU JOOM AK PERSONNALITÉ EN TANT QUE NIIT BOU SIWE KILIFEU DI DOUGOU SI AFFAIROU THIOUNÉ YI MANE MI TEUTHIE LOUNA SI DEUX PERSONNES SI AFFAIRE DE VISA YI TÉ AY TRUANDS FÉNI KASSÉ

  • @GFCPSG-2024.
    @GFCPSG-2024. Місяць тому +2

    Le problème qui se pose moy est ce que moko def mais man je sais que defou ko daniou ko dougal rek salbé so metrisé woul mbir mi manou ci

    • @maramethioub2304
      @maramethioub2304 Місяць тому +1

      Meune am sakh lac daniou ko nakh fekk Khalis bi diar thi lokhom Truand yi tjrs daniouy am intermédiaire

    • @GFCPSG-2024.
      @GFCPSG-2024. Місяць тому +1

      @@maramethioub2304 c'est ça nak lac daniou KO nakh man xam na ci loubari mom xolam rek mokoy togn

    • @user-df7zs3pt3c
      @user-df7zs3pt3c Місяць тому

      ​@@GFCPSG-2024.Bilae danioko sacrifié motakh naniou moytou truands xaliss Dou diar thi lokhom

  • @GFCPSG-2024.
    @GFCPSG-2024. Місяць тому +1

    Dafa melni da nga am problème personnel ak lac2 katal sa ndey feulé defoul dra

  • @user-re6ht1os7d
    @user-re6ht1os7d Місяць тому

    Yow ragalal Yalla nga wakh lu la woor.bayil di wakh cii Yallah parceque yow gom wulo Yallah.

  • @user-jv6xh2tv1b
    @user-jv6xh2tv1b Місяць тому

    On dirait qu’elle a un problème personnel avec Lac

  • @diengfallou7248
    @diengfallou7248 Місяць тому

    Yaw domerame deug nga

  • @diengfallou7248
    @diengfallou7248 Місяць тому

    Yaw doule réke koula wakh moko défe

  • @adadiop7645
    @adadiop7645 Місяць тому

    Sélbé yaye ga daga wara réfatll yaye dafa décde yaw yaye ga

    • @oumygueye4701
      @oumygueye4701 Місяць тому +1

      Basi dou wakh deugue lac moy Kane

    • @awandiayediouf2437
      @awandiayediouf2437 Місяць тому

      bilaye wakh dafa diafé li sma yaye dane wakh diabote dou khastè

    • @amadouba4254
      @amadouba4254 Місяць тому

      Wax dji nexul wayee kouniou lekone sey millions doula nexx bilay
      Yalla na yalla yombal faybi rk