Qu'il repose en paix, qu'Allah S.W.T. ait pitié de son âme ! Sa voix extraordinaire manquera plus d'un, mais par la magie des réseaux sociaux, elle continuera de raisonner encore et encore et ce, jusqu'à l'extinction du soleil inshallah...
+fatourassoul S G Guisngua ndeysane, c'est triste, quand tu l'écoutes, ton coeur s'apaise, ta colère et ta tristesse se dissipent avec... Qu'Allah l'agrée dans ses immenses demeures au paradis !
Allahou Akbar j'ai des larmes aux yeux Bi la premiere fois ma deglouko j'ecoutais la radio j'ai eu à enregistrer que 30 secondes billahi depuis 2016 ba legui mangui koy weur et grace à une amie je viens de le retrouver. Diareudieuf Yalla, Par Allah lui seul sait ce que cela me fait quand j'ecoute cette voix et ce khassida. Yalla na jam yagg Senegal. Bon magal à tous. Alhamdoulillah
Yalla nako Yalla khare Aldiana Ci barkeb Cheikh Fallou Mbacke Ci barkeb Cheikh Mor Dia Ndiar Sene mbokoum Talibe Elhadji Fallou Dia di doom ci Cheikh Mor Dia Ndiar
Qu'elle Belle recitation ca te penetre au plus profond de toi et donne envi de connaitre les ecrits de serigne touba. Souniou magg yi amou nou morom machalla. On est beni. Yalla yok sen leer niom nieup te tass Sen barke si nioun aka souniou niabot Amine
Barke baye niass ma beug bi khassida surtou bouko baye abdou Diouf diko zikar yalnaniou yalla maye deg deg 😭😭😭😭
Bilae ya bah deug
Serigne Touba amour mborom
Yalanako yala khaéré aldiana
Sanogo Mamadou billahi Man tamit nonu lassiy amei yek yek barkei BAYE NIASS
Beug nga lou diara beug barki bamba sa bo fébaré deko deglou diko diangu
Borom bakhna nga sanogo mamadou
Talibé Cheikh ému par cette voix et le poids des mots du Xassida, Macha'allah. Wallahi yeup ñoko bookk.
Ana gnikoy diguelo 2019 bilahi dafamay yobo fo sori 😢😭😭 baye Abdou Yalla nala yalla yreum tè kharè ko aldiana firdawsi 🙏🙏
Ndeysane MAGAL 2010
Ma gui ni ba 2090 dieureuf serigne touba
Amiiine
Yalle na khassida yi nek sa wetal barke Cheikhouna Ahmadoul Khadim
Allahouma Amine barké Yonente bi sala lahou alayhi wa Salam
Machallah baye abdou yalnako yalla kharé aldiana firdawsi barké cheickh ahmadou bamba khadimou rassoul amine ( 🤲❤👀🙏🤣😭😭
baye abdou diouf yalla nako yalla faye ci barké serigne babacar
Machalah
@@ndeyelo1151 il ya abdou diouf et omar diouf
Ndeye lo baay Omar Diouf akh baay Abdou Diouf bokou niou ki baay Abdou Diouf la
Amine 🤲
Qu'il repose en paix, qu'Allah S.W.T. ait pitié de son âme ! Sa voix extraordinaire manquera plus d'un, mais par la magie des réseaux sociaux, elle continuera de raisonner encore et encore et ce, jusqu'à l'extinction du soleil inshallah...
Yalla na Yalla Faye la si serigne touba amoul morom
dieureudieufe serigne touba ce poem matlaboul chifai soigne Tous les maladis
Werneu
Akay deug fall
Baye Late surtout celles du cœur ❣
J'adore cette belle voix, des frissons me gagnent à chaque fois que je l'écoute et je ne m'en lasse vraiment pas...
Daffe maye diolo
+fatourassoul S G Guisngua ndeysane, c'est triste, quand tu l'écoutes, ton coeur s'apaise, ta colère et ta tristesse se dissipent avec...
Qu'Allah l'agrée dans ses immenses demeures au paradis !
J’ai la même sensation que vous. C’est autre chose
Salam walahi sa fé du bien intérieurs❤️
Moi oci. Très belle voix
Barki Ahmadou Bamba liii nimumay df🥺❤️ Ndeysane yalla nako yalla yereum Barkep Xassida yi ❤️🙏🏿
Barkei Seydile hadji malick khassida bi dafmay doug yalla naniou yalla fayal bamba hol sedeu na
Yalnala Kou ted ki tertou aldiana firdawsy😭😭
Ça me rappelle mon père quand j'étais tout petit ...on aimait l'écouter de Dakar à Louga...repose en paix papa
Khassideu bii dafay dougou dama kholl...serigne Abdou diouf yalla nalla serigne Touba teirou Aldjiana thii Barkei Matlaboul Chifaii
Baye abdou diouf yalla na suf oýof thi kawAm te yalla na ko yalla xare aldiana
je nai mem pas pu retenir mes larmes yalnala yalla kharè aldiana si barkè serigne babacar sy
Ndeysane c 'est émouvant dieuredieufeuti kou tédd ki "Cheikhoul Khadim"
Dieureudieuf borom Touba yalla na yalla sounou borom kharer aldiana youkaweyi si Barker cheikh ahmadou bamba mbacke
Yalla na gnouko yalla fayal 😭😭😭
Deugeu deugeu seringe touba amoul morome yalla na yalla fayalniou ko
Yalna ko yalla yeureum xarei ko aldiana firdawsi 🙏
C'est tellement touchant les mots me manque mais dieureudieuf thi li
Gha may yeuglo qu'allah augmente ta lumière
💞💞💞💖💖💖💗💗💗💕💕💕💓💓💓💝💝💝🙏🙏🙏 yallah naniou yallah fayal CHIEKH AKHMADOU BAMBA RTA
Baye Abdou DIOUF yalna fi yague lool té wer. Barké Borom TOUBA.
+Boubacar DIOUF
Amin
2023 j'écoute cette belle voix ❤❤qui fait vibrer mon 😢 cœur Baye abdou nala yallah yeureum té kharéla aldiana si barké sérigne Touba khadim Rassoul 😢❤
Yalna yalla yokou ay lèram tass niou di barkèp . Barkèp matlaboul sifa-i.
Amine Ya Rabbi bi barakaty Seydina Mohamed sala lahou alayhi wa salam Amine.
thieuy yalla linekh na nek si khassidayi ba maguett si niè soun demoul aldiana nguen dou demm aldiana
Yana khassida leral sa bammel yana la sounou Borom kharela thia aldiana firdawsi barké Cheikhouna Khadim
Amine
amine
Amiiin ndeyssan
Amine way machallah
Amine Ya Rabbi barké Cheikhoul Khadim.
Ndeysan Yalla nala barkep xassida wetali finga nek
Ndeysaan Anna gnikoy deglou 2020😭😭😭💖💖💖
Yalna souf oyof si kawam borom touba takhawouko 😭❤️
Akassa j'ai larmes au cou lorsk j'entend les paroles chatoyantes
Qui est là en 2020 je suis tidiane mais j’adore les khassidas de cheikh ahmadou bamba ❤️❤️❤️❤️
Baye Abdou Diouf yalna sunu borom yok say leer Dieuredieuf Serigne Touba
Ndaysane yalla nako yalla kharé aldjiana
Yalna KO yalla Faye ci Barker Borom Darou Mhty
Mame abdou Diouf yalla nala yalla faye
C triste vraiment.quand je l'écoute j'ai les larmes aux yeux
Yalla nako sa borom terou si aldiana yi gueune kawé si barki xassaide yi😩😩😩😭😭😭😭
Allahou Akbar j'ai des larmes aux yeux Bi la premiere fois ma deglouko j'ecoutais la radio j'ai eu à enregistrer que 30 secondes billahi depuis 2016 ba legui mangui koy weur et grace à une amie je viens de le retrouver. Diareudieuf Yalla, Par Allah lui seul sait ce que cela me fait quand j'ecoute cette voix et ce khassida.
Yalla na jam yagg Senegal.
Bon magal à tous. Alhamdoulillah
Thièye serigne touba kènn dou mome
🙈🙈🙈😩😩je le cherchais depuis tout à l'heure 🙈🥰🥰🥰🥰🥰
Yalla nako Yalla khare Aldiana
Ci barkeb Cheikh Fallou Mbacke
Ci barkeb Cheikh Mor Dia Ndiar
Sene mbokoum Talibe Elhadji Fallou Dia di doom ci Cheikh Mor Dia Ndiar
diarama borom touba ak man cheikh ibrahima fall
Machalah machalah, yalla nalla Serigne Saliou térou aki khéweul
alhamdulilah dieureudieufer serigne touba
Serigne Touba khadim Rassou amoul morom holl Sedatina, cie Bay Omar Diouf yala na yala fayla cie sa buir Bamel Amimne yarabi
Djeuredieufe serigne touba. Baye abdou diouf yalla na yalla goudal faname si barke serigne fallou Mbacke 🙏🙏👌👌
Yalnako Serigne Touba terrou sa aldjanatoul firdawsi si barkép khasida dji
Ki est la en 2020
Diereudieufē Serigne Touba. Depuis xaléi ma ngui wëër pa biii
Baye abdou diouf yalla naco yalla yeureum djiegallco tapallco firdawci
Baye abdou diouf yalla nanga fi yag té wer
Serigne Touba rekk a wóor
Qu'elle Belle recitation ca te penetre au plus profond de toi et donne envi de connaitre les ecrits de serigne touba. Souniou magg yi amou nou morom machalla. On est beni. Yalla yok sen leer niom nieup te tass Sen barke si nioun aka souniou niabot Amine
Thiey yalla li nèkhna. Billahi.
Jerejefety Serigne TOUBA.
Dieureudieufeuti serine Touba serine saliou amoul morom
Yallana borom bi fekheul sa xol sa aldiana machaalah
Machallah yalla nako yalla defal tawfekh thie barké khassida yi
yalla nla yalla. yerem
Yalla nako serigne Bi fayy
Serigne touba amoul morome si dounia
Yala nakho yala faye bolè ko si yigne deukheukh yonente bi fa iliyina
Yalnala yalla faye baye ,si barkè Khassida yii
Barkei Yallah Lii meunou mako mougn 😭😭😭😭😭
XaadeeJv Sk kene mounouko mougne
Sant Serigne Touba Reik Monou War♥️🙏🏽
Machallah yagu fi loll baye Omar Diouf.
Machallah Dieureudieufeti serigne Touba ken dou yow
Yalla yalna terouko thia aldiana yow kawé kawé ya
Dieuredieuffetii Serigne touba nekh na trop
2020. Yalna bala bi diouguéfi si barké matboul shifai
Ndèyssane dawna yarame bilahi yalnako yalla trop aldiana
Je pleure à chaque fois que je l’écoute wallahi ❤️
J'aime ce xassida doumassi doyal
Noo l islam kay c beau bilay c frappant ce poeme d mn homonyme
Yalna yalla yeureum ko
Walahiii je l'aime. ...paix à son âme
Machallah Dawna yaram jeurrujeuff khadim rassoul
Je suis Tidjane mais douma cii doyal.❤👌🙏
Matlabou chifahi sama khasidala
@ndeyssan baye abdoulaye
Yallah na souf oyof si kawam
Yalla na súf óyof thi káwam ta cheikhouna cheikhoul khadim teru ko thia aldjiana
Serigne Touba Mola dieulssi 😭
Qui est la en 2022machallah cette belle voix me donne des frissons
Koufiiiii nek di deglou ba tay😭😭😭😭
Que firdawsi soit sa demeure éternel barkép khasidayi
Ah machalla waye nexna bilahi
Alhamdoulilah dieredjef serigne touba...
Yalla na ngan fi yague
dieureudieuf serigne touba
Mach'allah jërëjeuf borom touba
Thieuy xassida yi❤
Billahi moussou ma dégg lou hassida mais bi mom daffa tourre sama rongoye lale sama holl ahhh nittou yalla yi liguéye yal nane gnou
Dieurdieuf serigne touba
yallana yalla Yoky leram
Thieye serigne bamba😭😭😭😭😭😭 bamba ya bakhe
Qu’ il repose en paix
Machallah tabarakallahou jazakoumoullahou khayrane
Baye abdou diouf yalah na khipé adiana
Baye Abdou Diouf....la voix d'or