merci juste pour ajoutez une chose, mom ladef sama sonori telephone bilahi. tawfex ak soutoura sou bare lagnkoy nianal goor gui Abdou diouf. merci bcp mes amis diam ak xeweul yen tamite.
ndiaga diaw guene nano begg ci yaw nak. c'est ca la fraternite musulmane. li rek la sunu kilifayi beugone te yanguikoy dieufeh bou bakh mashallah. nous vous invitons de vous abonner sur notre chaine comme ca ngaye meune di diot videos yinouy ajouter. jerejef!
Il continue à donner des frissons meme en 2021 je réécoute cette vidéo je ne peut pas m'en empêcher que le bon dieu t'accueille dans son paradis walahi j'ai même pas les mots que firdawsi soit votre demeure éternelle 😭🥰😍😍🤩🤩
Mane mii talibé mawoulana Cheikh al islam Baye Niass la mai Baye Abdou mome rek layi déggelou sama yaram di dawou bilahi yalla nako sounou borom barkél limou fii bayi si barké Baye Niass
Alhamdoulilah ma sha Allah dieureudieufati serigne Touba Xadimour Rassoul baye abdou diouf yalna ko Yallah yereum t xare ko aldianatoul firdaws taass niou si barkem barkep serigne Touba Xadimour Rassoul
Yalla nako Yalla khare Aldiana Ci barkeb Cheikh Fallou Mbacke Ci barkeb Cheikh Mor Dia Ndiar Sene mbokoum Talibe Elhadji Fallou Dia ibn Cheikh Mor Dia Ndiar
Jerejeff serign Touba Alhamdulillah since we have you serign Touba. Nekhnaa may almighty shower you blessing protect you give good health long life prosperity success always bless amen amen amen
A chaque fois que je l'écoute j' ai les larmes aux yeux. Que Cheikhoul Khadime t'accompagne au paradis firdawsi
Que dieu lacceuile dans son paradis celeste amine❤😢
Amiiiine ya rabbi
Les vivants meilleur que toi
@@papaniang9061 il est vivant meilleur que vous
Amine Ya Rabbi bi barakaty Seydina Mohamed sala lahou alayhi wa salam Amine Ya Rabbi.
Amine yarabi ❤
Yallah saa borom yeureum té kharei ko Aldiana
Amiiine ya rabii ❤️
Depuis bima néké khalé ba légui khassida bi si sama khol layi dougou té goor gui dama soppe té khamou mako yonne yalla nako sounou borom Faye
Baye abdou diouf yalla nala Serigne bi terou si barke xassida yi amine barke borom touba
Ndeysane ki dang koy deglou kham ni kou niou défar la mashalah
Qui encore le regarde encore en 2023 yallah n’a aldiana done keur thi barké werou Koor gui🙏🏾🙏🏾
Yallah nako yallah yereum te khareko aldiana si barke SEYDINA MOUHAMED (PSL)
bilahi je suis talibe baye niass waye goor gui limoumay def yallah rek moko xam, yag gi te wer
Euskey Serigne ndiaga diaw. Linga seidei ci baye ablaye sedna xol. Jerejef waye. Niogui laye ziar bou werr
merci juste pour ajoutez une chose, mom ladef sama sonori telephone bilahi. tawfex ak soutoura sou bare lagnkoy nianal goor gui Abdou diouf. merci bcp mes amis diam ak xeweul yen tamite.
ndiaga diaw guene nano begg ci yaw nak. c'est ca la fraternite musulmane. li rek la sunu kilifayi beugone te yanguikoy dieufeh bou bakh mashallah.
nous vous invitons de vous abonner sur notre chaine comme ca ngaye meune di diot videos yinouy ajouter.
jerejef!
merci bcp, je me suis dejas abonne, yallana diam yag si sunu rew mi di senegal.
ndiaga diaw de rien. nioko bokk. amiiiine waye ci niane yi. yaw kou bakh nga mashallah
Magou Mourid, un exemple pour la nouvelle generation de chanteur Mourid.
Les Khassida du Cheikh nous suffisent amplement comme source d’inspiration.
Keine dou cheikhoul Khadim Dieuredieuf Serigne Bamba Dieuredieuf Serigne Abdou diouf yala nala Cheikhoul khadim fayal bopam🙏🙏🙏
Nékhena waye que dieu l'accueil au paradis nékhena torop waye
Le vieux il est trop bon et drôle qu’Allah l’accueil dans son paradis 🙏🏿🔥❤️
Ndayssane thieye serigne touba amoul morome sunu mame abdou diouf yalla nako yallah yeureum teh kharéko aldjana firdawssi thi barkep xassida yi aamine
AMINE YA Rabbi ❤
Dieureudieuff Cheikh Ahmadou MBacké, Baye Abdoul yalla nala souniou borom fayê thi khassida serigne bi.
Ki l'écoute comme moi en 2022 yallanako Serigne Touba Faye ❤️❤️❤️
Bilaye man la ki MoMA nara raye
Hooooo kou yaga toyal sama khol yalla nala mame borom touba térou si aldiana you kawéya Baye Abdou
Ndeyssane baye abdou diouf dafa nelaw. Yalla na khippé si aldiana firdawsi. Yalla nalla borom touba faye.
Il continue à donner des frissons meme en 2021 je réécoute cette vidéo je ne peut pas m'en empêcher que le bon dieu t'accueille dans son paradis walahi j'ai même pas les mots que firdawsi soit votre demeure éternelle 😭🥰😍😍🤩🤩
Yallah nako yallah yeureum té kharéko aldiana firdawsi si barké seydina mouhamed psl
machallah je suis tidiane mais j aime ce Monsieur dune dimension exceptionnelle
0p
Yawe dagua baakhe maneno méle nénéne dieureftaty
Yalla nako yalla yerem kharé ko aldiana firdaws
Mane mii talibé mawoulana Cheikh al islam Baye Niass la mai Baye Abdou mome rek layi déggelou sama yaram di dawou bilahi yalla nako sounou borom barkél limou fii bayi si barké Baye Niass
baye abdou diouf yalla nafi yague lolou té wère lolou thi barkè serigne salikhou mbacké amine
baye abdou laye diouf yalla nala yalla défal diamou cii barké serigne touba
Que dieu l'accueil au paradis amiiiiine
Yalnako yalla yeureume tè firdawsiii don keureume sama khôl day séede trop soumako déguer mouy diangue ça me soulage. Alhamdoulilahh
Djeureudjeuf Serigne Touba ❤
Yalna yallah défal ko Al Janna firdawsi🙏
Amine
Niougui diariniou si wakh dji ba légui 2024🎉❤❤❤❤❤
Que firdwas soit ta demeure éternelle sounou Mame Abdou Diouf
Diko jàalé bèpp mbookúm taalubé . Yalla na ko Seriñ bi tekk looxo.
3 ans encore et je reviens souvent regarder cette vidéo. Talibé dal nekh na; Baye Adbou Yalla nala Yalla kahré Aldiana Firdawsy
Yalla nakko yalla yaram xarko aldiana ferdawsi barki cheikhoul khadim amine
Yalla na souff oyoff thia kawamm si barki serigne touba
NOUS SOMMES EN 2024 TH NDEYSSANE A CHAK FOIS QUE JE L' ECOUTE G LES LARMES AUX YEUX
Machala que le bon DIEU l'accueille dans son paradis céleste amine ya rabi
Qui regarde cette Vidéo en 2024
moi❤
Machallah yalla nako yalla kharee aldiana si bakep khassidayii
Nogaye Ndiaye amine wayy
Yàl na ko yalla yërëm ta xare ko ca guyaar ya aminne
Machalah Machalah diureudief serigne touba diureudief baye abdou diouf yala na la yala faye ak serigne touba akazza mourid diureudief
Yalla nagua tasék yeurmader yalla ❤️
K Dieu l accueille dans son paradis si barkè Seydina Mouhamet
Machallah c beau à entendre 👂🏾 Diaraama Cheikhoul khadim
En passant ceux qui ont dislike 👎 vous êtes qui ? 😮
Sa pâ bi damako beug trop yalla na yalla goudal fanam si barcké serigne touba
yalla gafi yaga tawérr si barki serigne saliou
Yalla na yalla yoku aye leram si barkp serigne fallou Mbacké
Ndaysan ❤❤❤❤❤❤yalna yalla doly Ay lérame ta taass niou thi barckm
Yalla na ko yalla kharé adiana firdawsi
Yalla nako yalla souniou borome yeureume si barki borome touba
No khollal voix bi avec son âge machalla damani diné rek mo waur yalla Nako yalla yeureum té khareko adiana
Yalla Nako yalla yeureum té khareko adiana
Yalla nako yalla yeureum il est décédé le 7 décembre 2018
Amine
Amine
AMINE YA Rabbi ❤
Amine 🤲
Amine
Journaliste bi machallah
Il reste toujours dans nos cœurs et nous prions que tu sois avec AHmadou bamba à Firdawsi
Hakasa yalna yalla terouko aldian'toul firdawsi
amine
Yallah nala borombi youbou aldiana firdwasi Amine dieurdieuf Baye Abdou
Yalnako yallah kharé aldiana té oyofal souf ci kawam ci barké Khassida yi
Alhamdoulilah ma sha Allah dieureudieufati serigne Touba Xadimour Rassoul baye abdou diouf yalna ko Yallah yereum t xare ko aldianatoul firdaws taass niou si barkem barkep serigne Touba Xadimour Rassoul
Yalla nako yalla kharé aldiana❤️
Baye Abdou Diouf yalnako yalla yeureum khareko diannatoul firdawsi bidiahi seydiil woudioud Barke borom Touba.
Yalla naniou ko yalla fayal
Maag ngi nio mana diangue yalla nako borom bi diégeul
yalla nako yalla kharé aldiana firdawsi si barki seydina mouhamed psl yalla nako serigne touba fayal bopam alahouma amin 🤲🤲
Ndeysann toyal nga sama xoll bi yalla nala sgn touba tertou thia loxom you tède ya thie barkep xassida yi amin
Yalnala yalla Faye thi barcke Serigne Fallou ag khasiday S Touba yi
Je l aime tropppp😭😭😭😭♥♥♥♥♥♥yalnako yalla yeureummmm
No kel humilité kholal rek AK liko yalla mayé tour mai Mouy liguey Di doundé
Machaala ana nui koy deglu si 2020 yalna suf sed si kawam!
Dieureudieuf bakh rék mo woor
Yana firdawsa di wathiewayam amiine bi dia yirassoulah amine ...
Tiey Baye Abdou yaguu fi lolou t andak werr si barkep Xassida yii...
Mame abdou diouf yalla na ko yalla yeureume khareko si aldiana firdawssi yalla na ko Mame Borome touba terrou 🤲🤲🤲🤲😭😭😭
Merci beaucoup ! C est sublime ertraordinaire ! Merci Baye Abdou Diouf !
Ndeysane yaram dawna Baye Abdou Diouf yalla nafi yag té and ak wer barké khassida yi bég na lol si yaw barké borom touba yaw dé royoukay bou makk nga
Diara dieufty borom Touba amoul morom diara dieufty s Abdou diouf yalla borom Touba difall sahdatou
Ndeyssane yalnako yalla yeureume diégeulko xaréko aldiana firdawssi je l'aime trop
Repose éternellement en paix bayeAbdou Diouf
Aye baye Diouf bilahi kou bakh ta oyoff yalla gua fi yague ta wér si barké khassidas yi
Bourbi Borombi booleko thi Fad khouli fì ibaadì wadkhouli dianati.
Barké Cheikhoul Khadim
Thiey yalla nala serigne touba faye
Yalla nako Yalla khare Aldiana
Ci barkeb Cheikh Fallou Mbacke
Ci barkeb Cheikh Mor Dia Ndiar
Sene mbokoum Talibe Elhadji Fallou Dia ibn Cheikh Mor Dia Ndiar
Yalna sougnou Borom yokk say lèer daradièy borom Touba
Machall1 kadou yi diekna amna taloubé présentatrices aussi machallah
😭😭😭Yalla na la khassaïdes yi wetalila aljanna firdaws thi barkep cheikhoul Khadim.
Amine Ya Rabbi.
Joe the peace preacher yaw amal diamou rék barkép KHASSIDA yi
Baye Abdou Diouf Yalla nala Yalla khalé Al Jaana Firdawsi
ndeyssane Baye Abdou Diouf yala nala Serigne Touba fey si Matlaboul Chifaii bi nekhna trop machala 🥲😍 ndeyssane 11:14
Jerejeff serign Touba Alhamdulillah since we have you serign Touba. Nekhnaa may almighty shower you blessing protect you give good health long life prosperity success always bless amen amen amen
Djieuredief serigne touba
Yalla yeureum ko tei kharéko Aldiana🤲🏿🤲🏿
Dieureudieuf Borom Touba AMOUL MOROME KENE LA
Yalla mo ko déf yalla ga fi yeuga looooooooo amine
Serigne Fallou au Serigne Abdou Lahat Yalla rek laniouleu beugué
Yalla nala fi yalla bayi fiii sounou kaname amiine bilahiii tu me fe pleuree mame a travers les khassidas yalla nalla yalla deffal diame amiine
magui ziare Sama Diewrigne yi numéro baye Abdou Diouf la sokhla wone
Damako beug yalla nako yalla kharei aldjanay firdaw’s
Yalla nako kharé aldiana firdawsi
Alhamdoulilah ma sha Allah ndeysaan dieureudieufati serigne Touba Xadimour Rassoul baye abdou diouf Yalna ko Yallah xare aldianatoul firdaws barkep mbautoum xassidas yi
❤❤❤mascha'allha yalla nala fi yalla yagal si barké Borom touba mom seyidina mouhamed
Yalna gua fi yag loll tee weer thi barke serigne saliou
😭😭thieye yalla amna nioum may
Yana firdawsi di wathiewayam amlne .