Hajara, Ibrahim, Ismael - Doudou Kend Mbaye chante le sens profond du sacrifice et du puit de ZamZam

Поділитися
Вставка
  • Опубліковано 29 гру 2024

КОМЕНТАРІ • 436

  • @fatyba3238
    @fatyba3238 9 місяців тому +19

    Qui regarde a ramadan 2024❤🎉

  • @aboundiaye5339
    @aboundiaye5339 2 роки тому +34

    Mane dee baye fall la mai talibe chiekh yii dalene begue sama birr kholle barkep borom touba yalla na yalla maye tawfex ak taysir amiie

  • @sekouba6948
    @sekouba6948 2 роки тому +36

    Wa anii talibé Cheikh yeu nak
    MachaAllah 🕌🕌🇸🇳🇸🇳❤️❤️🤲🏿🤲🏿

  • @sambasow3115
    @sambasow3115 2 роки тому +10

    Doudou kene mbaye yalla nala yalla maye goudou fane may la wer si Barke seydouna mouhamed Barke cheikh Barke elhaji Malick Sy

  • @zenup9129
    @zenup9129 3 роки тому +50

    Allahou Akbar! Jerejef Mbaay, Yalna Yalla fay te goudal fane yi ak werr gui

    • @framboiseroyale6551
      @framboiseroyale6551 2 роки тому

      Alhamdoulilah baniou neké ay dioulite done talibé cheikh...salalhou allah Mouhamaddine 💕❤💖💯💖

    • @baamat4366
      @baamat4366 2 роки тому

      Allahouakbare

  • @dembasall1647
    @dembasall1647 3 роки тому +110

    Voilà de vrais intellectuels et poètes. Dès fois tu t'interoges même comment tous ces poèmes sont formulés.

    • @sophietaphadiakhate556
      @sophietaphadiakhate556 2 роки тому +5

      Je te jure j'ai les larmes aux yeux quelles
      émotions

    • @ahmadoudiop9041
      @ahmadoudiop9041 2 роки тому +1

      @Amssatou Diaw walae ndeyssane hana walo walo nga ioe

    • @sophietaphadiakhate556
      @sophietaphadiakhate556 2 роки тому

      @Amssatou Diaw a bon je ne le savais pas avec la maniéré dont il le chante tu ne t'en rends meme pas compte masha alla

  • @laye-lo
    @laye-lo 3 роки тому +16

    Doudou kend nient att maguii koo bgue guiss meunou makoo guiss🥺 sama wadjie bilahii yallah na goudd faan❤️

  • @bamsbams8372
    @bamsbams8372 3 роки тому +48

    Machallah 🙏 🙏
    Machallah 🙏 🙏
    Doudou li'nga bak souniou mame Ibrahima néx'na lol bilahi yalnala bour yalla taxawou si barki naby🙏🙏 amine

  • @abdouazizsy3014
    @abdouazizsy3014 3 роки тому +23

    Ni sama xol bi seddé yalla nala ka yalla Faye goudal fane wi, weral bat bi❤️

  • @wilanesaloum5455
    @wilanesaloum5455 3 роки тому +34

    Mancha allah na yalla goudeuol fanam wéreull Aÿ thiéreum

  • @mohamedaidara9748
    @mohamedaidara9748 3 роки тому +307

    Nako rewmi yeup nianale fane wou goud AK weer.... Si barke maodo. Un vraie poete maodo reciter par El hadj doudou kene mbaye.. Mashala

  • @oulimatoudieme3947
    @oulimatoudieme3947 2 роки тому +29

    A chaque fois que j'ai besoin d'ondes positives, j'écoute ce passage . Longue vie Papa Mbaye

  • @utilisationdesticdanslense7312
    @utilisationdesticdanslense7312 3 роки тому +56

    Wôw quelle éloquence avec une pédagogie incroyable.
    Maachallah.
    Yalnako yaag di baak baçi ay 100 you ték.
    AMINE.
    INCH'ALLAH.

  • @mouhamedseck9167
    @mouhamedseck9167 2 роки тому +41

    J’ai regardé la vidéo plusieurs fois sur plusieurs mois… A chaque fois je suis heureux ma sha Allahou ❤️❤️❤️❤️❤️

  • @ousmanesy2490
    @ousmanesy2490 2 роки тому +8

    Je peux pas rester un jour sans visualiser cette vidéo ♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️✅✅✅✅✅✅✅✅✅✅✅✅✅🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲

  • @muhammadsow9015
    @muhammadsow9015 2 роки тому +4

    Asfiyahi amoul morom
    Doudouken mbaye Yalla nafi yague té wérr

  • @awamboup3719
    @awamboup3719 3 роки тому +25

    Machallah baye doudou kène mbaye yalnala fi yalla bayi ngua niouy bègeul thi sounou Mame maodo Sy Aka wa keureum❤️❤️

  • @elhmamaansousy2986
    @elhmamaansousy2986 3 роки тому +94

    Quelle éloquence !! Sa voie est sublime

  • @madamsecka3050
    @madamsecka3050 2 роки тому +3

    Marsha allah thank u allah bima ame e maodo ak wa kerrem don talibe alamine pirr papa yalnala sa diamou yagua barki seydina mouhamed

  • @abdoulayendiaye406
    @abdoulayendiaye406 2 роки тому +27

    Walahi j'ai pleuré 😭
    El Hadji Doudou Kende Mbaye yalla na yalla goudeul ay fanam may ko wergou yaram té wéreul batt bi 🙏🏽

    • @leboundoye1403
      @leboundoye1403 9 місяців тому

      Dafa waw yaram😭😭😭😭😭

  • @canalo4081
    @canalo4081 3 роки тому +38

    Machala pape Doudou kend xol sédatina 🇨🇮😍🙏🙏🙏

    • @canog4885
      @canog4885 3 роки тому +2

      Yala nala yala faye mayla wer khewal moutie diam soutoure dakala seytané Kamala tiat

  • @abasall711
    @abasall711 3 роки тому +11

    Machala doudou kend goudal fan wer ak diam dolila soutereu so wayer munex so dianguer alkhourane munex

  • @beuguembayecisse3032
    @beuguembayecisse3032 3 роки тому +6

    Macha Allah s doudou kende mbaye yalnako fi yalla yaagall lool lool lool témou sammouko té haarko thie barké yonénne tibi shw

  • @bintoudamendiaye5986
    @bintoudamendiaye5986 3 роки тому +46

    Je peux meim pas exprimer s k j ressent en regardant cette vidéo💓💓

  • @bambadiagne1000
    @bambadiagne1000 3 роки тому +10

    Ak were ak meun si barki seydina mouhamed psl

  • @bo.finesss
    @bo.finesss 2 роки тому +23

    Nous sommes très chanceux d'avoir de telles personnes dans notre pays, vous êtes ceux qui ont le plus de valeurs, nous sommes très heureux, merci. Nous vous souhaitons longue vie en bonne santé❤️❤️🇸🇳🇪🇸

    • @dieynababa3360
      @dieynababa3360 2 роки тому +1

      Aaay way Mane wurdeu bii la beugeu djiel nane l'ay def

    • @fatouseck1847
      @fatouseck1847 Рік тому

      Amn♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️💯💯💯💯💯

  • @aminatasadio8712
    @aminatasadio8712 3 роки тому +5

    Machaa allah khol séde baye doudou yalana yalla guoudale sa fane ak bépe dioulite amine

  • @elhadjimalickcissediop2728
    @elhadjimalickcissediop2728 2 роки тому +8

    Yalna borom bi wereul batt bi. Goudou fane akk wergou yaram gua continuer diniou begeul. Baye Doudou Kende❤️

  • @mmb4282
    @mmb4282 2 роки тому +28

    Machallah que Dieu t'accorde longue vie et une santé de de fer. Khol séda tina

  • @senegalaise1
    @senegalaise1 Рік тому +6

    ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤🙈🙈🙈🙈🙈🙈🙈🙈🙈🙈😭😭😭😭😭 papa doudou yalla na yalla may la goudou fan ak wer si barki Seydina Mouhammad (psl)🙏🙏🙏

  • @mbayewade6480
    @mbayewade6480 3 роки тому +58

    A tes 100 ans el hadji doudou kende mbaye

  • @princesses4209
    @princesses4209 3 роки тому +5

    Machallah sama sope bi pa Doudou yalla na yalla maya la weer ak goud fans weeral bate bi

  • @ndeyeamyfall9306
    @ndeyeamyfall9306 2 роки тому +2

    Si barké seydina mouhamed barké wéro koor gi papa doudou kend mbaye yalla nalla fi yalla bayi défal la jamm ak soutoura adouna ak alakhira ak mbolém joulite💖💖💖barké serign BABACAR sy

  • @mariamfaye746
    @mariamfaye746 3 роки тому +6

    YallaH na YallaH goudal fan wi sunu mame Doudou kene Mbaye voix bi beine la wayei xam xam bi ma sha allah😍 ak khikass bi thie birr oh Mame Maodo mii😍🥰😍

  • @mariefall494
    @mariefall494 Рік тому +7

    Yallana yalla goudeul saw fane té defal la wére ak barker si barker saydina mouhamed

  • @bambadiagne1000
    @bambadiagne1000 3 роки тому +7

    Yalla nala yalla defal 100ans ak say rak si barki sen mame serigne babacar sy

  • @abdoulayeniang2511
    @abdoulayeniang2511 3 роки тому +19

    Yalla na Yalla goudeule saw fane Wéreul Thieure yi Baye Doudou Kénde Mbaye ❤️🥰🙏

  • @aitandoye4386
    @aitandoye4386 3 роки тому +11

    Mbaye more awa coumba doundal lo doundou ma khèp yagal weral barkè taha aleysalam ❤💯

  • @diarytall8204
    @diarytall8204 3 роки тому +6

    Doumaci doyal mouk longue vie à doudou kende sama yaye nako yala yeureum Aka mouka beugonn

  • @elsodione6253
    @elsodione6253 3 роки тому +10

    Macha Allah khole seddna diakal ngua no Histoire seydina Ibrahima

  • @huyanasantoz5102
    @huyanasantoz5102 2 роки тому +11

    Barki borome touba lii dafa daw sama yaramm ; Serigne Doudou kende mbaye yalna bat gueuna wérr gua yagg ĺolou tè andak wèrrr

  • @MBarSeck
    @MBarSeck 2 роки тому +2

    Sama khol cedna yallah yallah goudal sa fane Elhadj Doudou

  • @NM-ry2lm
    @NM-ry2lm 3 роки тому +8

    Salam merci beaucoup M. Doudou K Mbaye mashallah

  • @AlassanecireBah
    @AlassanecireBah Місяць тому +1

    ❤❤❤❤❤❤ fiers d'etre tidiane❤❤❤❤❤

  • @babacargueye6537
    @babacargueye6537 Рік тому +1

    ❤❤❤❤❤❤ machalla tabarakal lahou rafétna yalna yalla diapalé yalna yalla goudal fanam loooll thie barké rasoulil lahi p s l

  • @babacarseck3639
    @babacarseck3639 2 роки тому +2

    Thiéye tivaoune

  • @oumoubasse5546
    @oumoubasse5546 2 роки тому +4

    Machallah sama Doudou Kene Mbaye 🙏yalla na yalla goudal fanam té mayko wérr🙏🙏🙏

  • @ibrahimadiouf6405
    @ibrahimadiouf6405 2 роки тому +6

    MACHA ALLAH OH QUELLE CHANCE NOUS AVONS D'AVOIR DE TELS JOYAUX CHACUN DANS SON DOMAINE ALHAMDOULILAH

    • @diagnesewane7370
      @diagnesewane7370 2 роки тому

      Bi douma si doyal ndakh nekh doudou wéral ak faw wou goudou

  • @sokhnambenghe3070
    @sokhnambenghe3070 3 роки тому +7

    Mashalah ndeysane Lou metti ya guana si aduna yalla nagnou yalla di mey kholou mougn histoire bi dji guey gni gnogui koy dounou Ba leygui djeureudieuf baye Doudou❤️❤️❤️❤️

  • @binetoudiop9237
    @binetoudiop9237 3 роки тому +5

    Machalah khol sedd yaram dawna yallenaniou len sunu borom fay koulen topou dou rer

  • @fatimatoukane5587
    @fatimatoukane5587 2 роки тому +1

    Man souma dégué Doudou Kende sama khol day fekh

  • @GoraDiankha
    @GoraDiankha 6 місяців тому +1

    Ndeyssane machallah nekhna trop sikhol amna solo

  • @matyndiaye8276
    @matyndiaye8276 3 місяці тому +1

    Merci beaucoup ❤❤❤❤🎉🎉🎉🎉🎉

  • @nafissatoumbaye178
    @nafissatoumbaye178 3 роки тому +5

    Amine waye doudou kene mbaye mbaye yalla na yalla bour bi goudale fanale ❤️❤️❤️❤️

  • @tidianeaw5449
    @tidianeaw5449 3 роки тому +12

    Macha allahh amena solo yalla nala yalla samou sa ndiabotte 👏 👏 👏 👏

  • @modufaye2712
    @modufaye2712 3 роки тому +6

    Machalah diangalé rek si yalla ak limou yoni machalah yalla fayal gnou Mame Maodo ❤️❤️

  • @omardiallo114
    @omardiallo114 3 роки тому +17

    Machallah lng vie bonheur succès réussite total pour tes projets

  • @nafindao47
    @nafindao47 3 роки тому +5

    Machalla mbaye yalla n'a yalla goudale sa fan bou ans AK weer🤲🤲🤲

  • @assmalickcisse7482
    @assmalickcisse7482 2 роки тому

    Ahmadou kende mbaye nako yalla may fan wou goudou si barkep Mame ass

  • @mamandouba9258
    @mamandouba9258 2 роки тому +12

    Quelle voix!!!Doudou dal mashalah

  • @ramatamane4396
    @ramatamane4396 2 роки тому +4

    Ma Cha Allah néhna loll ci Hélle ak Holle, Alhamdullah

  • @fatoundir2536
    @fatoundir2536 Рік тому +1

    Yalnala yala maye goude fane ak wér si barki seydina mouhamed psl

  • @oumarfall99
    @oumarfall99 Рік тому +2

    Chaque jour je regarde la vidéo a plus 5 reprises
    Li neikhna si xol

  • @seydinagueye3501
    @seydinagueye3501 2 роки тому +4

    Yalla nako yalla bayi basi kanam amine wayy

  • @babacargueye6537
    @babacargueye6537 3 роки тому +3

    Machalla tabaarakal lahou ayadacoumoul lahou amna solo loooll tabaarakal lahou diajakoumoul lahou khayerane

  • @astougueye9161
    @astougueye9161 3 роки тому +1

    Yalla na yalla goudale saye fane si barké seydina Mouhamet

    • @abndiaye3153
      @abndiaye3153 6 місяців тому

      Amine Amine way🙏🙏🙏🙏🙏🙏😭😭

  • @SousLarbreAContes
    @SousLarbreAContes 3 роки тому +4

    Ma sha Allah, dieuredieuf xol sedd na. Gudd fann ak werr, di tagg Yonenti

  • @LyaSow-p1e
    @LyaSow-p1e 4 місяці тому +1

    *Ndaysaan yalnagnouko yalla fayal teh mayko werr ak werlé deffal ko diam dolli soutoureuh si si barky Seydina Mohamed psl*

  • @realboy7904
    @realboy7904 2 роки тому

    Yalla nagnu yalla fayal sunu pape Doudou ken mbaye té may ko goudou fann

  • @oumyndoye7585
    @oumyndoye7585 3 роки тому +4

    Machala yalna yalla doolii laa soutoura bouu lawww

  • @mbayefaye986
    @mbayefaye986 3 роки тому +1

    Dounda Mame boy yalla n'a yalla yook yookkk yalla bayi lafi

  • @diagne5077
    @diagne5077 3 роки тому +17

    Trés belle voix

  • @papesylla7281
    @papesylla7281 3 роки тому +2

    PAPA DOUDOU KENDE YALLA NGA GOUDD FANE 🤲 NIGA NIOUYE BÉGEULÉ YALLA NALA KO YALLA FAY BOUBAKH.
    LI SA BOUMAKO DÉGLO SAMA YARAM DAW.

  • @ndeyefatoubop7188
    @ndeyefatoubop7188 2 роки тому +3

    Ho papa doudou yalla nala sounou borom guéna wéral Bate bi machalla ninguay def sama khôl bi yalla nalako yalla fay

  • @fatoudiop133
    @fatoudiop133 3 роки тому +1

    Yalla na ko yalla may fane you goude machalla c'est une légende

  • @coutihnosow5162
    @coutihnosow5162 2 роки тому +3

    Serigne Amadou yalla na fi yangue lolou te weur Amine

  • @beuguembayecisse3032
    @beuguembayecisse3032 3 роки тому +1

    Yeune waa asfiahi yalnaléne yalla Faye yiwe té yockou lénn bangénn yeucko thie barké yonénne tibi shw

  • @babacaniang9584
    @babacaniang9584 3 роки тому +8

    Machaalla kol sed naa tropp

  • @ousmanegaye5177
    @ousmanegaye5177 2 роки тому +2

    Bilahi doudou kende sedal nga sama khol yala na yala sedal khol ba aba d'âne🙏🏼🙏🏼

  • @ousmaneniang1762
    @ousmaneniang1762 3 роки тому +1

    Doudou kene mbaye yalla n’a yalla goudal fanam

  • @awa8432
    @awa8432 2 роки тому +2

    Yalna yallah werele batbi amine yarabi si barkep chiekh diurieudieuf

  • @mouhamedmoustapha684
    @mouhamedmoustapha684 3 роки тому +9

    Allahou Akbar yalla mayla goudd Fan AK werr 🙏🙏🙏

  • @moussaseye9444
    @moussaseye9444 3 роки тому +1

    vrai poete yalla nala yalla same la te are la

  • @abdouniang9482
    @abdouniang9482 3 роки тому +9

    Ma challah baye doudou kende mbaye yalna nga goudou fane 🙏🙏🙏

  • @mbenguerawane274
    @mbenguerawane274 2 роки тому

    They doudou yalla na yalla goudal fanwi

  • @ndiayependa3112
    @ndiayependa3112 Рік тому +2

    Longue vie à toi machalla

  • @fatoungom9912
    @fatoungom9912 6 місяців тому +1

    Chaque année ma Sétane ko yalla na yalla fayal niou mame Mbaye té goudal fane pape Doudou kende ❤❤❤❤❤❤

  • @dierysy7024
    @dierysy7024 2 роки тому +1

    Machallah yalna ko yalla may fane you goudou

  • @oumyfaye8795
    @oumyfaye8795 Рік тому

    Yalna yalla goudeul sayyy fane teee yokou weer guii
    Machallah

  • @adamasall7633
    @adamasall7633 3 роки тому +9

    J'ai les l'arme au yeux machaalah 😍😍😍

  • @ismailadiene4145
    @ismailadiene4145 3 роки тому +6

    100 ans rek inchallah mame ❤️

  • @banelsy8191
    @banelsy8191 Рік тому

    Goud fane weur AK werle si barké seydina mouhamed psl son bi Limay def sama taw ismaila dème sama papa ismaila

  • @ZeynaNdiaye-uv2is
    @ZeynaNdiaye-uv2is Рік тому +1

    Machalla pape doudou kene mbaye yalla n'a yalla goudal fane wi

  • @famaniang5638
    @famaniang5638 2 роки тому

    Amine yalla na la yalla wereul batte bi papa doudou kende

  • @AlyKane-u3m
    @AlyKane-u3m 9 місяців тому +1

    Ma Ayla🥰🥰🥰🥰🥰❤️❤️🤲🏿

  • @mouhamedseck9167
    @mouhamedseck9167 Рік тому

    Qui est toujours là 10/2023… une histoire de soumission de Ibrahima à Dieu, de hadjara à Dieu et son mari ibrahima, et enfin de Ibrahima à Dieu et son père ibrahima.
    Allahou Akbar !!! Dieu est grand!!! Dieu est misericordieux❤

  • @generaltheboss5470
    @generaltheboss5470 2 роки тому +2

    Machalla yalnaniou yalla fayal cheikh seydi hadji Malick

  • @ahmedsow1893
    @ahmedsow1893 2 роки тому

    Yalla n'a yalla goudal sa fan

  • @mouhamedndour451
    @mouhamedndour451 3 роки тому +1

    Yalla na yalla wéral batt biii

  • @Sport2079a
    @Sport2079a 3 роки тому +1

    Yalla goudal sa fane si barké ahmed (psl)