Balla Gaye 2 sacrifice moko Topp? Khadim Ndiaye fait de graves révélations et enfonce Yekini

Поділитися
Вставка
  • Опубліковано 4 лют 2025

КОМЕНТАРІ • 360

  • @SenbuzzTV
    @SenbuzzTV  2 роки тому +25

    N’oubliez pas de vous abonner sur votre chaîne Senbuzz Tv et d’activer la cloche 🛎 pour recevoir les notifications merci.

  • @alioundiaye7146
    @alioundiaye7146 2 роки тому +83

    Quand balla gagne il est le meilleur mais quand il perd on parle de yekini ou de blessur soyer sportif

    • @kineseck8786
      @kineseck8786 2 роки тому +4

      Aliou nii akou yékini dinaléne daalll

    • @alioundiaye7146
      @alioundiaye7146 2 роки тому +4

      @@kineseck8786 danio meuneu togne tei akh bakhoul tei gorr kene douko toumal

    • @cheikhvip4757
      @cheikhvip4757 2 роки тому +2

      degue pirr bro bilahi 🤣🤣🤣🤣🙏🏽🇸🇳🇺🇸

    • @magayefaye9334
      @magayefaye9334 2 роки тому +1

      Vrément

    • @cheikhdiop9673
      @cheikhdiop9673 2 роки тому +1

      yékini moni sama combat ak balla diam dou ci am avant ak après

  • @mouhamadoufalilousall4281
    @mouhamadoufalilousall4281 2 роки тому +11

    Boy Niang 2 mome Président daf ko wara décoré limou def dafa reuy machallah 🙏🙏🙏

  • @papito8025
    @papito8025 2 роки тому +12

    Thiongane tu es très posé et pertinent. Khadim ndiaye fatel yoyou ndax makk nga té bayi waat ci kamil.

  • @mamadoulaminefaye9646
    @mamadoulaminefaye9646 2 роки тому +11

    Masakhla Khdiame ndiaye tey wakhga lep merci 💪🏼

  • @mamourgassama6898
    @mamourgassama6898 2 роки тому +35

    Yékini Douléne tontou mukku mongui sie bopam bayiléne sosalaté déléne nangou deffaite balla moment yi respecté toul combats yii balla dimanche dah simékou ma rouss ngéne beuga diapeni Yékini molénko tékk.

    • @kineseck8786
      @kineseck8786 2 роки тому +5

      Mamour bayil gnii ndalh nitte cou bakh dou sossoll domou adama akou yékini dinaléne dalll walahi

    • @mamourgassama6898
      @mamourgassama6898 2 роки тому +6

      @@kineseck8786 jajeuf Séck ndanane ❤️

    • @morhann1619
      @morhann1619 2 роки тому +1

      Wa balla yui Dina wakh rék

    • @CASI7797
      @CASI7797 2 роки тому +1

      Nena beine mbeur dotouko yappp mdrrr.... 🤣🤣

    • @mohamedlamineboye316
      @mohamedlamineboye316 2 роки тому +2

      @@CASI7797 Boy Niang yapp nako c’est fini

  • @ababacarndao4980
    @ababacarndao4980 2 роки тому +2

    Père Khadim Ndiaye yallah na yallah dolii suttureu cii barckép alkhourane té goudeul sa fanne

  • @laminetall2712
    @laminetall2712 2 роки тому

    Champion tu a lutter avec tout les grand lutteure.maintenant tu est fout méchant 😢

  • @djimbasarr3248
    @djimbasarr3248 2 роки тому

    Khadim merci ❤️❤️❤️❤️

  • @lampsarr4540
    @lampsarr4540 2 роки тому +3

    Wakh nga deugue khadim Ndiaye

  • @Landing-ey7cq
    @Landing-ey7cq 2 роки тому +1

    Balla gaye 2 ses le meilleur lutteur de tout les temps vous avez des votre coilusion ande danele balla

  • @generalndiaye7353
    @generalndiaye7353 2 роки тому +6

    Pére kHadim geuna yageu geuna wér 🙏🏽😄

  • @elhadjifall283
    @elhadjifall283 2 роки тому +3

    Khadim taay môme il a parfaitement raison, analyse pertinent
    Yekini môme taloul lamb Jamono bi
    Té yakarou ma soxar ague na fofou
    Sport la du courage BG2 et félicitation BN2

  • @khalildiene7832
    @khalildiene7832 2 роки тому +13

    Vérité absolue père khadim deugu rek ngua wakh machallah... balla boudoul ndigu lii di genoux bi amna loussiy metii

    • @aissatouseck6242
      @aissatouseck6242 2 роки тому

      Mane dh vraiment bimou tousé lani Balla mi ya klq chose

  • @papedieng4414
    @papedieng4414 2 роки тому +1

    Veramente khadim Ndiaye cou bakhla machalla

  • @moustaphfall3192
    @moustaphfall3192 2 роки тому

    Bravo khadimi loulerga wakj

  • @abdoudiouf4128
    @abdoudiouf4128 2 роки тому

    un vrai lache un vrai mécontentement cher toi

  • @papendiaye4673
    @papendiaye4673 2 роки тому +5

    Journalist bi djiambaar deug le
    Bravo thiogan 👏🏽👏🏽👏🏽👏🏽damakoy deglou yensay mè ku meun limiy def le

  • @modoundiaye7985
    @modoundiaye7985 2 роки тому +23

    yékini amoule sakh diotou balla non alakhira nar na yémé nite koga xamné beuré gén gua dane bobou tay mou took roukam sa bo dané ioe la waya sa bouniou la dané gua toudou ko non on,es dans quelle pays

    • @andedieulefimacky5209
      @andedieulefimacky5209 2 роки тому

      Dagay sop de kou balla beurer mou douguessi

    • @khassoumcisse3227
      @khassoumcisse3227 2 роки тому +1

      Yekini moko wah motah niep diko khép louy après combat diam doufa am

    • @momosenghor5004
      @momosenghor5004 2 роки тому +2

      @@khassoumcisse3227 tu as mal compris les propos de yekini ragale YALLA

    • @TALIBECHEIKHNATIDJAN
      @TALIBECHEIKHNATIDJAN 2 роки тому +1

      Yaw sétanoulo vidéo bi dé... Khadime wakhoul dara lou niaaw si yékini. Mais Thiombane moy séytané bi. Wa salam

    • @adjichafall196
      @adjichafall196 2 роки тому

      Yekini moko wakh dh

  • @sey551bsonmba5
    @sey551bsonmba5 2 роки тому +2

    Merci khadim guoudeul fane way

  • @ousmanethiam3354
    @ousmanethiam3354 2 роки тому +3

    Khadim ndiaye bayil tak radio yi.
    Balla gaye depuis 17ans Mingui bégeul sénégalais yi….
    Toute chose a une fin, dara sakhoul si adouna.
    Soula boy niang diapone defla lou raw limou def balla.
    Mbaye demal nga tok

  • @ibrahimaba5304
    @ibrahimaba5304 2 роки тому +12

    Man dé nangou na boudon da diougé si yékini manatoul ame victouwar niou ni dara aman lou xéw mais danatt nafi 3 mëur niou beugeu togne yékini boudé dane daal mofi man mais bouniouko dané tay débar bouniouko dané suba da ganiou niou dane ko guinaw suba niou ni daniou ko sotte wala yékini moka yakh té BG2 bimoye beuré ak yékini gnépou kham naniou ni yèkini dagne ka doon sotte BG2 bimoye beuré ak M. Lô sen 1 èr combat tamit nonou M. Lô dagne ka don sotte sila Eumeu sene sakh méré di diapalé M. Lô Nakh lignou ko don sotte bayi len togne yékini dèfoul dara BG

  • @LaFFofficiel
    @LaFFofficiel 2 роки тому +8

    Khadim magg bou niakk fay da la amoule roussou kay sakh 😭😥😭

  • @djibrildiallo483
    @djibrildiallo483 2 роки тому +2

    Lorsqu’il Bala gagné contre Gris Bordeaux ils ont rien dit donc si balla perdent les combats contre Boy Ng laisser l’hypocrisie. Yekini n’a rien fait.🧏🏽‍♂️🧏🏽‍♂️

  • @AmadouDiallo-em6pm
    @AmadouDiallo-em6pm 2 роки тому +1

    Très bien dit père khadime

  • @balladiop6336
    @balladiop6336 2 роки тому

    Merci kadougui rafetna

  • @abdoulayendiaye9257
    @abdoulayendiaye9257 2 роки тому

    Machala khadim des paroles sages avec beaucoup de maturité

  • @modoudiokhane5712
    @modoudiokhane5712 2 роки тому +1

    9mn 10s amneu béne ladoum bou rombou mais MachaAllah 🤭🤭❤️

  • @alioudia2464
    @alioudia2464 2 роки тому +1

    Khadim Ndiaye vrai nafekh la gueumoul dara boko kene wakhati khadim kouti ndiaye la toudou Senegal gni gno guena bagne balla guaye si Senegal 1kouti Ndiaye 2 pape sarr 3 dèguol 4journalist babacar

  • @fatimafatima-xj3cw
    @fatimafatima-xj3cw 2 роки тому +1

    il a bien parlé khadim ndiaye

  • @bethelcoaching-moussadiouf9101
    @bethelcoaching-moussadiouf9101 2 роки тому +8

    Important Mbeur. Tous les lutteurs doivent le savoir.

  • @aldachir1032
    @aldachir1032 2 роки тому +1

    Khadim Ndiaye tu nous amerde, dioulite dou togne
    Yekini yonam nekouci
    Bala , Boy Niang mo niouss ndeyam

  • @adamamballo7349
    @adamamballo7349 2 роки тому +7

    C'est vrai balla doit changer son entourage.

    • @abygackou5165
      @abygackou5165 2 роки тому

      Bilahi ay gnom niang xaragne lo ay lirou diane louniou xam cii lamb

  • @madondior5217
    @madondior5217 2 роки тому

    Balla bamfi ngénté yaguoul kone ndigam amoul béneu problème boybi déko meune rek doumako félicitations encore boye ñiang❤

  • @papiniang8909
    @papiniang8909 2 роки тому +14

    Après combat balla yèkini bg2 Dane na fi tapha tine Modou Lô gris bordeaux bayleine yèkini dou yalla meunoul si balla dara li ndogal leu rèk

    • @diagnemodounaar9613
      @diagnemodounaar9613 2 роки тому

      Frère mane modou lo moy sama mbeur balla moussou moko faral mai yekini meme bou défoul dra balla Gaye sax douthi set ndax mofi wax momak balla après lamb sax diam dou am sén dingeunter exemple kiuniouy djigne deummou ngay segnou yaxou liir

    • @sambadrame3497
      @sambadrame3497 2 роки тому

      Merci frère Balla Gaye for ever 🇫🇷

    • @matydiallo3211
      @matydiallo3211 2 роки тому

      @@diagnemodounaar9613 deg na deug dh yékini moko wakh limou wakh sakh dafa reuy té bimou koy wakh comme kou nékoul ak khélam té li fo rek la bou diékhé diekhna

    • @papiniang8909
      @papiniang8909 2 роки тому

      @@diagnemodounaar9613 Mais yèkini combat bobou dafa dieufrou ba nieup xam Ko t bilahy lolou mossi bakhone pour rèk mou xam ni mome dou yalla dou yonète mais j’insiste encore bilahy meunoul si balla Dara yalla mo nieuw rèk c mon avis nak

  • @falloudiop7651
    @falloudiop7651 2 роки тому

    Billahi père luu lerr la wkh ✅✅✅

  • @P-show.
    @P-show. 2 роки тому +2

    Merci père khadim Ndiaye rafetna trop

  • @nba3800
    @nba3800 2 роки тому +12

    Merci père bravo 💯👌🙏♥️

    • @diaaaa9607
      @diaaaa9607 2 роки тому

      Ki mofi wakhoné yekini mo yakh balla gaye ki mako ragal

  • @tidianely5352
    @tidianely5352 2 роки тому +1

    Merci Grand khadim Nice na

  • @mcidjii2879
    @mcidjii2879 2 роки тому

    Nitou deugue.leuh khadime Ndiaye

  • @gentlemara9873
    @gentlemara9873 2 роки тому +1

    Manchalla Khadim wax dji rafetna mais journaliste yi xolat len sen titre yi il n'a rien di de méchant sur yékini limou wax lepp si analyse lamb la lui il s'est parlé il est véridique🙏

  • @gooobhff1115
    @gooobhff1115 2 роки тому

    Merci beaucoup père

  • @yerodjolof5044
    @yerodjolof5044 2 роки тому +24

    Toumal nitt rek yekini Dina lakk gnou Bari gueumelen yalla

    • @cheikhdiop9932
      @cheikhdiop9932 2 роки тому

      Yeki ny dou dara nan ko bayii

    • @aidajuf8377
      @aidajuf8377 2 роки тому +1

      @@cheikhdiop9932 Yekini d'où s'en morom s'en mbeur boyi gnokoy malmené

    • @kineseck8786
      @kineseck8786 2 роки тому +1

      Geumou niou yalla waiýé akou yékini dina lénne daalllll chimmmmm

    • @akadtv661
      @akadtv661 2 роки тому

      Yekini mo wakhone aprés combat bi sakh dou yombb

  • @idrissadione7279
    @idrissadione7279 2 роки тому

    Merci beaucoup khadim djieureudieuf trés boula kén wahloo

  • @bambistediop6652
    @bambistediop6652 2 роки тому

    Wa khana dafa teyé lokhom contre Modou lo AK gris Bordeaux 😂😂😂

  • @aidadiop4717
    @aidadiop4717 2 роки тому

    Machaalah

  • @ecrituremajuscules6929
    @ecrituremajuscules6929 2 роки тому

    Khadim Ndiaye yafi wakhoon yékini day khéekh balla Gaye ngani yako guiss
    ioe doul katt bou magg

  • @dembagadio3325
    @dembagadio3325 2 роки тому +2

    Yallah ata na lène Jackson dana niaka diarigou nak 😁😁😄😄😄te sa thies dina dane reug reug

  • @cheikhtidianendiaye8729
    @cheikhtidianendiaye8729 2 роки тому +3

    Khadim Ndiaye ragalal Yallah la yafi don nga waxx Yekini lou melni xémé waxon mo topou balla gaye tey nga nieuw changer version
    Thieuy Yallah

  • @djibithiaw1259
    @djibithiaw1259 2 роки тому

    Manam yalla boy Niang la andal mais bou deugue des DEUG balla amna louko dall xawma mystique la xawma lanla perck limè diokhè entraînement ak bou douguè si guew bokoul

  • @morhann1619
    @morhann1619 2 роки тому

    Merci way Khadim

  • @papekebe3224
    @papekebe3224 2 роки тому +4

    Dem len saitane khadim ndiaye limou wax tji balla Gaye bimou Koy diokh cadeau foto serigne touba bi ak laigui limouy wax nguen Khol difference bi Tiey Adouna li rek motakh nit di changer

  • @mouhamadoufalilousall4281
    @mouhamadoufalilousall4281 2 роки тому

    😀😀😂 non khadim raynama billahi wallahi dafa nex

  • @famadieng8018
    @famadieng8018 2 роки тому +1

    Lousa yone thi guéwalyi doule rék gaye défe balla molla gueune gueune sa ndeye

  • @youmisetayou5649
    @youmisetayou5649 2 роки тому +8

    Tonton khana daniela sacrifier tamite bayiléne balla domou diambourla bayiléne ko 😪 fitame bi dale

    • @papediop33
      @papediop33 2 роки тому

      Saway fi koufi nékoul domou diambour way geum léne yalla

  • @momoweezy4281
    @momoweezy4281 2 роки тому

    Khadiam ndiaye de guay kat ndem domaram

  • @ibrahimadiop8632
    @ibrahimadiop8632 2 роки тому

    Merci infiniment Khadim vous êtes véridique longue vie et bonne santé.💓💓💓💓💓💓💓💓💓💓💓💓💓

  • @alassanedieng7479
    @alassanedieng7479 2 роки тому

    Parfaitement

  • @zdpdiakhate2139
    @zdpdiakhate2139 2 роки тому

    Ma cha alla pere khadim

  • @papito8025
    @papito8025 2 роки тому +31

    Moi en tant que supporter fassois , lima diap ni dal balla yekini dako garder rancune batay mais je ne n’avancerai pas là-dessus

    • @gmeuzcana193
      @gmeuzcana193 2 роки тому +23

      Ah lociy wax nala leeer rawatina wax ci goor
      Lingay avancé si *YÉKINI* dara woroulaci....entre tmp ( après son combat ak *YÉKINI* ) amnaci 4 AUTRES victoires ( *TAPHA_TINE MOD'LO GRIS 2FOIS* ) con donc di toumal wadji té amoci bén preuve soralél sa bamél té xamni lø wax si niit fi rawatina (touma) ding ko layo ak môm

    • @astoudiouf9191
      @astoudiouf9191 2 роки тому +9

      Dara woroulasi. Ragalal yalla

    • @yacinegueye3228
      @yacinegueye3228 2 роки тому +5

      Toma bakhol de khana kone balla limou def modou lo sof nguen trop bayi len di saltel victories diambor

    • @khassoumcisse3227
      @khassoumcisse3227 2 роки тому +1

      Boul ray wah dji yekini yague nako wah nena après combat niom niar diam doufa am

    • @azouaz189
      @azouaz189 2 роки тому +2

      Serere kene dou yabe si lambe

  • @traorebabacar7057
    @traorebabacar7057 2 роки тому +2

    Khadim Grawoul waye bayil mou sedeu lirou sa waye la adouna amoul solo lep daye diekh

  • @mamadoudiop8082
    @mamadoudiop8082 2 роки тому +3

    Lesport c la jeunesse et la santé.Balla a perdu les deux

  • @cheikhdiop9932
    @cheikhdiop9932 2 роки тому

    Ai khadim. Wakh nga fi lou nek balla kontour yeki ny

  • @seneabou7308
    @seneabou7308 2 роки тому +1

    balla gaye 2 Mouy nbeur bi bilay walay

    • @thiernodiallo2830
      @thiernodiallo2830 2 роки тому

      Lolou dafa ler fall billahi amal diamou waye ❤💯💪

  • @boubaleye2003
    @boubaleye2003 2 роки тому

    Wayyy dagnouko sotttt ligueyyy koo bah amatoul dolè reug reug siteu yekiniii

  • @morhann1619
    @morhann1619 2 роки тому

    Balla Gaye 2 bou mouy Dane yekini niom nieupa sote yekini wa balla Gaye yui na niou nopi ahhh😡😡😡

  • @elbcg3609
    @elbcg3609 2 роки тому +4

    Thiongane sa ma journaliste bi mes da nga yakam ti bilahi 🙄🙄🤦🤦😂

  • @diopbenmohamed9119
    @diopbenmohamed9119 2 роки тому

    Champion thiaroy merci

  • @idrissadione7279
    @idrissadione7279 2 роки тому +1

    Wakh nga deugeu dee balla na défaraatt estaffame

  • @aminatandaw7330
    @aminatandaw7330 2 роки тому

    Wa khadim Do nopalou nak katal dayam wayyy

  • @matarleyekaraleye2545
    @matarleyekaraleye2545 2 роки тому

    Bonarik

  • @serignemodoundiaye8534
    @serignemodoundiaye8534 2 роки тому +1

    Khadime manedé yéne wouma lali yalla xame Nani biga wakhéne amena thi ndiabotou serigne bi kou bayilo bere ga bagne ba légui guisou me fo yoco thi lambou

  • @makhetedakar2157
    @makhetedakar2157 2 роки тому +1

    Assallaamou aleykoum mbokyi naniou maandou nguir yala Tonie bakhoul Nay raffet naniou bayi yekini

  • @mohameddiedhiou4101
    @mohameddiedhiou4101 2 роки тому

    Khadym ya niamé deugue

  • @CASI7797
    @CASI7797 2 роки тому

    Et à quel moment il a enfoncé Yekini?
    Bayileine feine waye
    Au contraire il a défendu Yekini

  • @wadeissakha2725
    @wadeissakha2725 2 роки тому

    Merci per 🙏

  • @fallcoumba8154
    @fallcoumba8154 2 роки тому

    🤣🤣🤣🤣🤣🤣 selfie 🤳 🤳 kayy

  • @kandjikhady6659
    @kandjikhady6659 2 роки тому

    Taye mome ligua wakh deugue ligua wakh dara douko dindi té gniép khamnanou lolou ndakh yeukini moko wakh niép di dégue mes nak mome yeukini yalla guisna lép

  • @opporeno7799
    @opporeno7799 2 роки тому +3

    Sama yone nékousi Pape Diouf la beugueu mane

  • @bilalembengue2474
    @bilalembengue2474 2 роки тому +4

    Hana yekini moy yalla défaite bou kén meunou çi dra

  • @mamadousarr4223
    @mamadousarr4223 2 роки тому

    Khôl bou Boneu motakh nga toroukh sa génération nieup niola rawww après combat balla yekini balla diokhnala 500mil par ce que dagakodane maral tatame soudè li Ousmane Diop nek AK balla Moy Boneu sène khôl yèneu wa thiaroye diguène Fatou

  • @assanekaka9414
    @assanekaka9414 2 роки тому +1

    mais demay lathii té kana lyrou newufi 😁😁

  • @byby9333
    @byby9333 2 роки тому +3

    Tiey sénégalais Balla doomyi nioy deff effet AK niakk tek beurem si Yoon AK niakk préparation bou bakh papam AK père Balla dagnko manke boy show bizzyii khamouniou lamb daniouy diayy wadji rek

  • @teychamaures4670
    @teychamaures4670 2 роки тому +6

    Merci beaucoup père khadim 👏👏👏

  • @bouboukaloga9062
    @bouboukaloga9062 2 роки тому +1

    Ya snapeur, ya rappeur, ya tay lawbe😂😂😂

  • @sarjojabbi6752
    @sarjojabbi6752 2 роки тому

    How many action did boye nyang

  • @diopmingue7542
    @diopmingue7542 2 роки тому

    Mann lima diakhalll balla gaye bou dano rék gnou dougal si modou lô ak yékini😂🤣😅😂🤣😅😂😅🤣😂

  • @omarndiaye3409
    @omarndiaye3409 2 роки тому +1

    Bly balla moy sama lep ms tank yii AmA toul dara bly Mbeur bokoy entraîne doko Yeureum Gnikoy entraîne gnoko djokhoul gueudeum kome limou andi mome ak modou lo da dathieu Lou meti françe motax mou andi lolou

  • @mamadoundiaye5230
    @mamadoundiaye5230 2 роки тому

    Yen tamitt sen titre bi ay vrai défaillant

  • @mamadousall3663
    @mamadousall3663 2 роки тому

    Nouyobi Amna ko toudoul journaliste yi buZz Yi lolou intervi la té Bessela mome AK maître elhadji Diouf encien avocat du peuple

  • @jeanjacquesdione6600
    @jeanjacquesdione6600 2 роки тому +1

    Titre bi kholate léne ko Way II ne l’a pas enfoncé. Té deug rék la wakh

  • @cheikhtidianetounkara7844
    @cheikhtidianetounkara7844 2 роки тому +3

    Khadim Ndiaye ngua balema naak BG2 tolou toule foukeu bisse di dépassé

  • @brothernature8441
    @brothernature8441 2 роки тому

    Khana balla dou nitt kessé waroul danou🤔🤔🤔

  • @maremendiaye2052
    @maremendiaye2052 2 роки тому

    Yène niarr nieupou danguéni doul 😢

  • @Psycho.i19O
    @Psycho.i19O 2 роки тому

    Fén rék beug xaliss di diakhassé nitt yi ,Guinaw Yallah tousss

  • @moussadiouf6155
    @moussadiouf6155 2 роки тому +1

    Naniou bayi yékini tranquille.
    Lamb dou meussa changer khalé yi nio fiy dieulé mak gni.
    Dafa done dane gniko djitou ci lamb légui ayi rakam nioko fiy dieulé.

  • @mamadouthiaw2694
    @mamadouthiaw2694 2 роки тому

    Balla n'est pas meilleur mais il lutte bien

  • @mameousmanecisse540
    @mameousmanecisse540 2 роки тому +1

    C une seule personne ki dit k sathies est impoli c khadim ndiaye ,micro trottoir tout le monde dit k sathies est trop respectueux Sénégal dale doyna ware

    • @mohamedlamineboye316
      @mohamedlamineboye316 2 роки тому

      Père Diaw li Khadim NDIAYE wakh la wakh deh attention

    • @ndiougamar2202
      @ndiougamar2202 2 роки тому

      Sa Thiès dafa doof mo gueneu réw si mbeur yi Amoul respect

  • @mamelatyrly8758
    @mamelatyrly8758 2 роки тому

    Yaw khadime ndiaye may niou diame bayile domou diamour yî bo diougué si sa thiese deme si balla nie linie ame amenanouko ba paré

  • @Landing-ey7cq
    @Landing-ey7cq 2 роки тому +1

    Pas bi dafa rew trorope meunoule siportes Balla gaye 2 diap ko mistique veux meunoule def Dara