Félicitations Lac tu es un vrai champion ! Je ne vois pas un lutteur qui a autant de qualité dans l'arène. On peut ne pas l'aimer mais il reste un champion quand on parie sur lui il assure le gain.
Une seule sortie vers les sacs ne doit pas être averti 2ou3 fois le lutteur peut être averti mais le CNG EST TROP NUL ET IL DOIT RÉVISER SES FAÇONS D’AVERTIR LES LUTTEURS.TOUT ÇA C’EST POUR VOLER L’ARGENT DES LUTTEURS ET CELA DOIT CESSER QUAND MÊME.MERCI
Lac n as pas plus de force que siteu ce que tout le monde disait lac mo eupeu dollé siteu foufff animou téy 😂 siteu diambar leu bou khayé rek gniorna wawaww bay fall bi amna ndam ❤
Lac niouss nako😂 siteu dafa reuy Lamigne lac ay wax késé danouko siteu show man la😂amoul xam xam beuré amoul doolé wa lamb dji nioniouko beug forcé rék
😢😢siteu talibés mame ceikh ibra fall 😢😢lac de guerre 😢talibés serigne babacar sy 😢😢seni serigne wa khou ñiou lene dîné yalla sougnou borom lolou motakh Sénégal bari ay talibés you doff agressif c honte tarikha yi ibliss Meaux co alimentai bokalé ak bida
Mame Cheikh Ibrahima Fall ak Serigne Babacar dafouniou dara c'est que génération bou bées bi mo mel noonu mais boul wakh dara Si niari Serigne yi niome def nén li gni def baparé ba wouyou dji Yallah
Félicitations Lac tu es un vrai champion !
Je ne vois pas un lutteur qui a autant de qualité dans l'arène.
On peut ne pas l'aimer mais il reste un champion quand on parie sur lui il assure le gain.
Siteu bilahi yay ndanann ♥️♥️♥️♥️♥️♥️
noumou néké ndanane ki niou doumeu ko yobou ko ardo en plus di beuré ak koula mak fouf 😂😂😂😂
Félicitations siteu 🎉❤
Félicitations siteu champion
Lac mima guiss meuwtii bouko betoul douko rayyy😂😂
Wouy maguette magui dé je suis par terre
Bravo aux deux lutteurs
😂
Bravo lacun lion reste toujours féroce malgré sa vieillesse
LA 2 SOF NAAA. BEUR BO XAMNI DOU DEF ACTION, DEY XAR ADVERSAIRE DEF BA DIOUM. DAFA YOMB TROPP
Siteu vs Ama Baldé le combat rêvé par tous les amateurs 🙏🏿
Bravo lac ya diriger combat yako doumeu ya gagner felicitation
Lac est très physique macha alla. Siteu khawna dé
Lac meilleur lutteur vraiment dagn ko sonal rk wa senegal mom sougn la bgoul rk moy lolu mais tay siteu mo daw combat bi
Deugue bou were Sénégal mo beuri nafekeu
deugue diou wére nga wakh
LaC franchement félicitations
Mai nak félicitations à SiTeu aussi diamageune bégue nagn si ioE wallahii ❤
❤ magg Def diar thieur thi lamb j Yal gueuneu gun inchalla
Lac d guerre félicitations bayi lén skhor Sénégal mome sougnou la bagné rekk diéhna bayi lén khéh meur way
Bilaahi Guisso leegui Siteu Modou lo nieup dii xass Siteu teu fii nieup xass Lac2
Bravo la 2S
Une seule sortie vers les sacs ne doit pas être averti 2ou3 fois le lutteur peut être averti mais le CNG EST TROP NUL ET IL DOIT RÉVISER SES FAÇONS D’AVERTIR LES LUTTEURS.TOUT ÇA C’EST POUR VOLER L’ARGENT DES LUTTEURS ET CELA DOIT CESSER QUAND MÊME.MERCI
👍🏿 merci beaucoup tu as bien dis
Bravo lac
Félicitation siteu yay gorr deugu
Siteu GAINDÉ ga 💥🔥🔥
Siteu dionguama dji sonal nala dé taye 😂😂😂
Lac n as pas plus de force que siteu ce que tout le monde disait lac mo eupeu dollé siteu foufff animou téy 😂 siteu diambar leu bou khayé rek gniorna wawaww bay fall bi amna ndam ❤
Bilahi
Legui défaitam yi bari deh nganan
So degué wa plateau bi dangay yakarni siteu mo deff lepp😂😂😂😂😂😂nafekh baxoul
Sénégal aka bari aay nafekh daniouy guiss baye fall bouniouy niouss mouy daaw ba paré niou nane ko khaw ngako reey😂😂😂 Nafekh naak dou doug aldiana
Siteu mi pois lourd yi fi neik meunou si dane keine amoul dolé bi amoul sagne sagne bi amoul beuré bi
Saway. Comba lac bi😂. Monona bania digo😂way akh. Yakhna aferbii yepp
Lac a tt fait les gars bayilen sokhor
Lac 2 is the super star
Lac tu as bien gérer ton combat
Kouy tek sa xaliss tek KO si lac do per dh
Mais siteu combat bi yeup dako daw!!! Bokone na thi gnidone sanni kheer lac 2 mais franchement moo diriger combat bi
Bravo lac tu a bien luter
Mdr niak nga xorom nk😅
Lac commme Macky sall koi nexouma dara
@@AboulBacharSalllossi yonou macky Sall doul way
Vraiment 🎉🎉🎉🎉🎉
Xana yaw rakou lac ga déréte da fore deh ay doul you graw sax😂
Siteu kasse futur roi inchallah ❤
Félicitations lac 2
Wa 2stv siteu wakh len ko deug beurewoul
Do sax nit dga no diom comme lac rk Nolen Mouna khole lac diko supporté putin😅
Andil fou lac sogué
Lac amna niari guémbou Dêfoul dara. Siteu dou forcé dakh lac kéndou ko force
Pourtant siteu waxone na bou lac gneuwé lamb dji diékh dée gnou reri dée noum deme nii
Un bon lutteur lac 2
Félicitations siteu ❤❤❤❤
Siteu kasse siteu kasse siteu kasse ❤❤❤❤❤
LAC 2 MEILLEUR LUTTEUR ❤❤❤❤
Doulll
Lutteur bou gueneu tappete
Lignou def modou mbaye kèp koumou mèti rk dèl sètan fi th abonnés
Ni guéne féséler stade nonou guéne warone ende rék déme guéné détenue politique yi 😢😢😢
COMBAT bi Lac moko beurè Siteu dafay reculè rèk deug yalla moko mom
Lad ès le meilleur lutteurs dû Sénégal îl n'a jamais perdu Un combat contre emeu ces tête contre fesse
Pardon 😂😂😂
Siteuuuuuuuuuuuuuuuuuuu❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Gni raporté sakh siteu lagnou farale
❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Lac niouss nako😂 siteu dafa reuy Lamigne lac ay wax késé danouko siteu show man la😂amoul xam xam beuré amoul doolé wa lamb dji nioniouko beug forcé rék
Lac champion la mais barina ay noon dh
Bilay lac so bayé ada fass diap diga am loula méty
Dérétou diamanguéne🎉🎉
Non siteu mo nekh il n’a rien lutter,limouy kouko beurré do danou diégué sakou yi sounioula dieko nga guéneu😅
Lac vs fran combat la siteu bou amone dolé dey am dara
Bou amone dolé😂😂😂😂😂😂😂
Félicitation situé tu es brave
😂😂 ray nga ma c'est siteu pas situé
siteu soffna pour mom mo beuré beuré bi té mo daw combat bi yeup
Dagno yapp siteu même les grands lutteur non pas réussi à manœuvrer lac bravo à tous ils ont bien Lutter
Mais lac daxoussi ken mou Seuss si sakou Yi
Ana ragaleyi nanou la dieule
Bravo siteu
Suite mii mou boul dan Modou lo kii day Daw rék bou la Modou lo diapé Dina la khawaray
Bravo Siteu ❤
Siteu n'a rien fait khamoule dara siteu manoule beurré
Bravo
Lac 2 bayil berer
Siteu demal defarou wat amo beurè bou balla bilahi
Lac niak diome day rassou ak jeune bi siteu
Non lac daal diakhal nama amoul bène diom
SITEU A LUTTER TOUS LE COMBAT LAC C UN TAPÉTE
Fadam yadi sayetanè
Mais Lac Tapha Tine combat revanche bi niorna walla😂???
Dagni nul rk niari yambar la
@@championdafrique9807😂😂 mais combat bou wara nekh lay done
Lac on est fatiguée avec toi toujours match nul 😢😢😢😢😰😰😰😰
Noooooooo siteu ak ama ak
Liss ak diop 2 ak Prince nio eup fans si lamb dji
fén ngeu dei
Combat bi nekh na lol
Lac dou toussss wakh rekk ak merrr lay deff….. motakh combat wame diaralouma 1000f
😢😢siteu talibés mame ceikh ibra fall 😢😢lac de guerre 😢talibés serigne babacar sy 😢😢seni serigne wa khou ñiou lene dîné yalla sougnou borom lolou motakh Sénégal bari ay talibés you doff agressif c honte tarikha yi ibliss Meaux co alimentai bokalé ak bida
Mame Cheikh Ibrahima Fall ak Serigne Babacar dafouniou dara c'est que génération bou bées bi mo mel noonu mais boul wakh dara Si niari Serigne yi niome def nén li gni def baparé ba wouyou dji Yallah
Siteu seul amoul data yayam
Siteu vs Ada fass combat la dh ndakh niar niou beuri mbololen bobou dh arene national keun doufa khat
Situé kesse
Lac de jarul wax "bravo" ndax li mom match nul la kom d'habitude, du bere ngir daan.
Lac mon foufou
Lac de guier na diayyi foutti ki dou mbeur
Non mbourakhé
Mé kéne mounouko dan
Siteu bou matone 120kg day dan lac de guiers yeg nano fo khamne bou amone yene dole yi rek dakoy dan modou lo tu es averti
😂😂😂😂 woy
Lac mo def lepp
Ce minable lac sou wakhé ngani tayye nga dé
Lac yambar la reck
C'est une bne résultats
Siteu a tou fait
Physiquement siteu était près il montre pas de signe de fatigue
c'est faux
@@galaxiepro.5641 ???
siteu seul
Lac de guère vraiment il est trè nul mai ki amoul technique beurèwoul dara mai ki dafa beurèwoul dara c'est un yambar way😂
Arbitre bi dafa warone bayi dernière diapanté bi
Lacs est plus MATURE que lui
MAIS SITEU N'A RIEN FAIT , IL N'A RIEN TENTE
Combat not nekh
Lac de guerre on est nul
Combat nul comme d’habitude avec Lac
Lamb mom bou déssé lac 2 rék diaroul dém stade koi
siteu n'a rien fait dans ce combat
Ki de meunta d’âne modou nanie wahante deug rk
wallahi
😂😂
Lac dou dara vraiment on dirait un nindja
😂😂 ninja kay
Mbeur y Ay escro you niaf sén ndeye lagnou dou niou entraînement niom niar nieup ken amoussi ndeyou physique gni dal sén leufeul ndeye rek