J’ai écouté le combat à la radio mais ak ni reporter yi don wakhé comme Modou Lo beuré woul dara alors que Modou mo Beuré Combat bi lepp mo déf action yepp vraiment Modou ya Meun ya eup dolé💪💪👍
Félicitations modou que importe la façon de la victoire que importe la durée du combat t’as assuré de lutter avec une telle façon beuré nga wonénga diom ak foula félicitations modou kharagne lô ❤🎉🎉🎉
Franchement Modou Lô est un vrai champion car malgrés les deux avertissements de Siteu il continue à attaquer pour diriger le combat. Et c'est ce qu'il devait pas faire😢. Mais malgré tout il est le meilleur 🎉❤
Modou tay togn nganiou trop waro wone dieul risque yi yeup tu es l rois ds arènes tu as attaqué tout l combat il y'a un moment danga warona takhaw khar ko mom moy woutsi xamna niou sa diom ak sa djambar amato loy prouvé me beuss daniouy gère ki waro wone essai dara 2 foi me nak félicitation prochainement bouniou ko defati ❤❤❤❤🎉🎉🎉🎉
Y’a pas eu de chute en plus c’est modou qui a fait les deux actions. Faut pas oublier aussi on ne peut être dehors et terrasser à la fois. Chapeau modou tu nous as livré un combat intense
@@kaireabdoulaye1397nio boku xalat deh Sincèrement faraluma ci ken mais sama giss giss Siteu mo daan ci action bi C vrai Modou mo deff action mais epaulam bi da laal suuf alors que siteu deful ben yon 4 appuies
@@kaireabdoulaye1397bou commencé ci bir kay modou moko initié dou siteu ? Té modou mi initié ngi ci bir siteu miy top action guéneu ngen beugeu mou dàane ?, xana limoy dm boutique ba wara joxé xaliss né dedete jioxma ma téyé sama xaliss !!!
Xlo est vrai Lyon tu met ton couronne 👑 en jouer et tu attaque comme si c’est toi qui veut la couronne 👑 coûte que coûte big respect ✊🏿 vraiment Xharan Lo le roi incontestable
Le king MODOU LO est un incontestable champion. Chaque combat, il vient combattre avec ferveur, technicité et force. Allah yi barek. Mais entendant les reporters ont crois que son adversaire lui a résisté au point qu’il ne mérite pas amplement et fortement sa victoire. Quel guerrier ✌️ Il a révolutionné cette lutte sénégalaise, lutter sans rien porter sur son corps juste ses récits qu’il récite à chaque coup de sifflet de l’arbitre, il est clair qu’il applique le « توكلت على الله ولاحول ولا قوة الا بالله ». Inconditionnel fan depuis 🇲🇷
@@coumbasow8948Nek roi takhula meun epuis modou foum eupé dolé siteu ?? Xana kay jom. waxou thiakhane bayilenko, modou limou df ni ci siteu niakul courone bi la df bombardier yobuko ardo, BOMBARDIER la wax dé niakk, Balla gaye fumu jar ak bombardier mom ? Li modou am ci bombardier, mom dako am fofou. Modou mom moy Diambar kouli fadrin, xamoulen Jom lumiy deflo nit même bo meunoul, joxé sa bakane
Modou lô, tu n'as plus rien à prouver, ce n'est pas pour rien que t'es LE ROI DES ARÈNES 👑, les jaloux et hypocrites se sont dressés contre toi sans pouvoir le cacher au lieu de reporter avec professionnalisme mais Yalla mola fal koumou faral do danou même contre tout un pays. Se adversaire sou beuré, nga beuré, sou beuréwoul nga beuré Lô ndam ciré koulay khar yalna khaadi. Siteu a raté tous les grands rendez-vous de sa carrière, fuir à chaque fois c'est une stratégie nulle, ça gâche une carrière et c'est pas ainsi qu'on va être couronné roi, faut se remettre en question. Nioun fans Modou lô yi même si un jour on perd dara sounou mbeur c'est un champion et une légende incontestée de la lutte sénégalaise yalla moko def té boba deniouy santate yalla rek.
@AbdouBa-k4b oui c'est possible parsk s'il n'utilise plus leurs talismans c'est qu'il ne paie plus pour ça donc niom ils n'ont plus d'utilité pour lui donc sén marché day yakou...fi d loudoul sounou borom néne leu, ils n'ont rien compris
Moi je trouve que siteu était venu juste pour défendre une couronne ça se mérite mais reculer pendant 30 minutes et dire qu’il n’a pas démérité c’est honteux bilae. Tout ce que je peux dire Modou t’es un vrai champion 🎉 malgré les critiques mais t’es un vrai roi 👑
@@Mamecheikhndao-pe8nyDafa di goor yalla dawoul bène yone mo deff lepp kone c'est normal daffa niémé encaissé aye coups goor deugue dou daw 😅 Nagoul rekk
*Siteu est ridicule! Tu es plus jeune, tu es le challenger, tu as besoin de la couronne, tu es dominé à la bagarre, tu sors de l’enceinte 4 fois, tu as plus d’avertissements, et malgré ça tu ne prends aucune initiative, en plus ngeu japp nguemb modou jappoul dara et tu ne fais pas d’action, tu perds, et tu jubiles? Il perd et on le félicite😂. Nii le defone contre Lac 2. Wakh leine ko deugue! Au Sénégal on fait la promotion de la médiocrité surtout dans le sport, c’est désolant*
Qu'est ce que tu racontes mec? Modou n'a pas dominé Siteu, il faut etre aveugle pour dire ça. Modou est allé se soigner et tu nous raconte un autre combat peut-être
@ c’est pas parce que tu vas te soigner que tu es dominé à la bagarre. C’est possible de prendre un coup qui te fait saigner malgré avoir dominé. C’est modou qui attaque à chaque accrochage, c’est lui qui enclenche la bagarre, et c’est Siteu qui reçoit le plus de coups
Fans balla gaye yi dougourou aziz ndiaye yi mayléne gnou jaam 4 appuis amoul fiii CNG dina até SITEU felicitations 🎉 jambar gua modou zero faute beuré gua khékh gua telgua paré macha allah ❤❤❤❤
En écoutant les commentateurs à la Radio , j’avais grave l’impression que Siteu mo beuré beuré bi yeup mais apparemment il n’a pris aucune initiative pour quelqu’un qui aspire prendre la couronne Modou mo beuré mo ame ndame bravo Champion 👑👑👑❤️
Modou mo xéx mo beurré mo diriger Moy déf action siteu daffa daw Di rassou té si diaxasso bi siteu mo déf 4appuit xol lén🧐loxo Modou bi mogui si kaw ☝️félicitation xaragne lo👑👑👑
@ bo manoul wonn beuré modou dakoy deff ngaka .kou manoul beuré dans beuré combat royal gnou manoul yaksiwougn niveau bii🧠je suis trop d‘accord de la façon noumm beuré avc le roi 🧠🧠
@@slattboy1293 kouy xalé 🤣🤣bayima wayy khamoo louy lamb khana amoul xalé akk magg lamb dafay ladjeu nga khamm koumay beuré manoumako eupoumako dara nga amm noo beuré akk mome sii xëll akk dalll.siteu était courageux mana deukou lokho droit modou lô .un combat avc beaucoup de polimique il lui a tenu en échec Lolou molénn nekhoul enfaite
@@ModouFaye-fs5tkmeunounio ragal défaite sounou mbeur khamoul daw kom tapette, il n'a plus rien à prouver beuré mom dafko meun diko def mais yen jalousie yi mieux vaut partir, sott neniou be sonou téwoul yalla mom la faral
c'etait l'attaque contre la defense pendant 20 minutes un combat unidirectionnel. Mais lii rek leu siteu meunone def pour guéneu si Modou kouko song ya ngui si danger. Bravo a tout les deux
Ce combat me rappelle un peu yékini vs tapha ... avec les reporters partisans et tout ... Bravo Modou déssa lognou dara ,courage si Siteu...yallana diam sakh
Frère soyons sportif Siteu à très bien lutter Modou champion leu Motakh tmt Siteu nii ley abordé ay Combat wam khana sétlouwolen lolou loubakh Mouy beurré AK modou en plus combat royal ba paré dii deugeul bopam
Vraiment Siteu mo Dane👑Champion deug dou Ama dou Boye Niang dou Eumeu Séne kéne amoul li si modou lo baye door mbague bi😮Recours rék niou dieuli Roi bi🎉🎉Siteuuu👑
Félicitations à modou lô il mérité amplement sa victoire ❤ et siteu doit se remettre en question et arrêter de célébrer des défaites comme une victoire amal diome
Mann siteu d'où Sama mbeurr mais pour dire la vérité. Siteu mo gagner modou lo da danou Srx on se dit la vérité les gars farr néxoule mais deugg thi leuh bok. Combat bi nehna trop Mei siteu a gagné wallahi kou d'accord beusseule j'aime gua commentaires niou yatal
Soyons honnêtes té bayi thiakhan yi siteu mo def 4appuis mo danou dafa wara changer sa façon de lutter dafay daw rek dieuloul bén initiative té taye môme mo momone combat bi
Les hommes au micro manquent d objectivité ! La chute de Siteu était évidente sur 4 appuis. Il faut éviter de tomber dans un esprit partisan quand on a comme rôle de rendre compte au grand nombre. Je vous souhaite beaucoup de courage.
Pourtant 3 appuies successifs leu df, deux genous et main gauche mais bi main droite bi di wathie dafa yeukeuti main gauche bi fékaneté wouniou kholal bou bakh. Mais nak modou mo beuré beuré bi yeup
Tout ces lutteurs MODOU Lô est le meilleur. Le lutteur des Militaires cavaliers 🎉
Bravo champion, on va le fêté à THIÈS.
T'es le plus technique
No siteu billahi modou lo Della bougone ray
Mais suteu mi mom il n a rien fortu ...modlo c est Un vr galadiator
Moi Modou n’est pas mon lutteur mais c’est le meilleur. Modou a fait tout le Combat. Bravo modou
Merci pour la générosité.
Wakho DEUG dé
Bly yabax moy attaqué moy khekh siteu diapana ngimb t modou diapoul lutax deful action
J’ai écouté le combat à la radio mais ak ni reporter yi don wakhé comme Modou Lo beuré woul dara alors que Modou mo
Beuré Combat bi lepp mo déf action yepp vraiment Modou ya
Meun ya eup dolé💪💪👍
Niom nieup daniou koy khekhh
@@FatouSylla-rk4mf Yalla molène euppeu dolé louko nékh rek moye âmme
@@FatouSylla-rk4mfman kay dama diahlè wly
@@KhadijaKontehwallahi🙏❤️
Ils sont visiblement avec sitteu. Ils ne sont pas du tout objectif. Surtout n'a fait que se défendre. Il n'a pris aucune initiative
100 ans yii mbeur bou mélni modou lo dotoul ame🎉🎉🌍
Xamna balla Gaye dey football 😂
@elhadjkane7346 billahi modou lo moko geuna rafett palmareis ,,
Félicitations modou que importe la façon de la victoire que importe la durée du combat t’as assuré de lutter avec une telle façon beuré nga wonénga diom ak foula félicitations modou kharagne lô ❤🎉🎉🎉
Waw félicitation kay moy def action moye attaqué moye khekh
Franchement Modou Lô est un vrai champion car malgrés les deux avertissements de Siteu il continue à attaquer pour diriger le combat. Et c'est ce qu'il devait pas faire😢. Mais malgré tout il est le meilleur 🎉❤
Modou tay togn nganiou trop waro wone dieul risque yi yeup tu es l rois ds arènes tu as attaqué tout l combat il y'a un moment danga warona takhaw khar ko mom moy woutsi xamna niou sa diom ak sa djambar amato loy prouvé me beuss daniouy gère ki waro wone essai dara 2 foi me nak félicitation prochainement bouniou ko defati ❤❤❤❤🎉🎉🎉🎉
Lolou moma méti mélni amoule ay conseils
@@senegalrek2579 djapanténa akk siteu beuréwoul tayy dafa privilège khékh pour lann prtant biko siteu djapé manonn na beuré comme djiné leu aaa was
Oie sa lefeul ndaye dômexathie
Pourtant modou il a bien lutté mais dafa waron khar touti mais amna fay tol mono khar félicitations modou❤❤🎉
Sa way siteu meunaloul dara modou té siteu khamgani dou fekksi
Y’a pas eu de chute en plus c’est modou qui a fait les deux actions. Faut pas oublier aussi on ne peut être dehors et terrasser à la fois. Chapeau modou tu nous as livré un combat intense
Vérité absolue 🎉🎉
Action bi si birr la komasé waleu
@@kaireabdoulaye1397nio boku xalat deh
Sincèrement faraluma ci ken mais sama giss giss Siteu mo daan ci action bi
C vrai Modou mo deff action mais epaulam bi da laal suuf alors que siteu deful ben yon 4 appuies
@@kaireabdoulaye1397bou commencé ci bir kay modou moko initié dou siteu ? Té modou mi initié ngi ci bir siteu miy top action guéneu ngen beugeu mou dàane ?, xana limoy dm boutique ba wara joxé xaliss né dedete jioxma ma téyé sama xaliss !!!
Bilay ❤
Xlo est vrai Lyon tu met ton couronne 👑 en jouer et tu attaque comme si c’est toi qui veut la couronne 👑 coûte que coûte big respect ✊🏿 vraiment
Xharan Lo le roi incontestable
Vraiment ❤❤❤
Le king MODOU LO est un incontestable champion. Chaque combat, il vient combattre avec ferveur, technicité et force. Allah yi barek. Mais entendant les reporters ont crois que son adversaire lui a résisté au point qu’il ne mérite pas amplement et fortement sa victoire. Quel guerrier ✌️
Il a révolutionné cette lutte sénégalaise, lutter sans rien porter sur son corps juste ses récits qu’il récite à chaque coup de sifflet de l’arbitre, il est clair qu’il applique le « توكلت على الله ولاحول ولا قوة الا بالله ».
Inconditionnel fan depuis 🇲🇷
Beug done roi té do jeul bén initiative.
Mon ma diakhalle😂
Lolou c'est impossible bro
Si beugué nek roi il faut nga woné diome ak fayda mais combat bi dako daw
Roi bi tamitt ayoul mo eup dolé siteu fouff té mounouko dane😂
@@coumbasow8948Nek roi takhula meun epuis modou foum eupé dolé siteu ?? Xana kay jom. waxou thiakhane bayilenko, modou limou df ni ci siteu niakul courone bi la df bombardier yobuko ardo, BOMBARDIER la wax dé niakk, Balla gaye fumu jar ak bombardier mom ? Li modou am ci bombardier, mom dako am fofou. Modou mom moy Diambar kouli fadrin, xamoulen Jom lumiy deflo nit même bo meunoul, joxé sa bakane
@coumbasow8948 danou ko c'est parck siteu dafa takhawoul mtx
😂😂😂😂😂😂 gni mom dagno far day melni siteuu rek Moy beuriii 😂😂😂
Modou vraiment respect 🎉🎉🎉
vraiment modou mo beure combat bi yeupp
Gnii ay mercenaire laniou rek douniou wah deug, Siteu nek fii di daw rek nioukooy plébisciter
Y6az6u e 5aà555t5
Bilayi wkhatiko dh frere
Ngi ayyy Domerame lanou yeugo wone lolou 🤣🤣🤣
Machalla Modou tu as lutté tout le combat,vraiment tu mérites le titre de roi des arènes.
Vraiment deg rk nga wax
Félicitations à Modou Lô. Une victoire très bien méritée.
Depuis le Bénin
Kharagne yalla nala djik si barké Seydina Mouhamed psl 🙏🙏
Champion Deugg Moye Modou Lô Chapeau 🤠Mbeur Yaye King Bi 🫅🏿🫡
Modou lô roi des arènes 👑🔥
Modou lô, tu n'as plus rien à prouver, ce n'est pas pour rien que t'es LE ROI DES ARÈNES 👑, les jaloux et hypocrites se sont dressés contre toi sans pouvoir le cacher au lieu de reporter avec professionnalisme mais Yalla mola fal koumou faral do danou même contre tout un pays. Se adversaire sou beuré, nga beuré, sou beuréwoul nga beuré Lô ndam ciré koulay khar yalna khaadi. Siteu a raté tous les grands rendez-vous de sa carrière, fuir à chaque fois c'est une stratégie nulle, ça gâche une carrière et c'est pas ainsi qu'on va être couronné roi, faut se remettre en question. Nioun fans Modou lô yi même si un jour on perd dara sounou mbeur c'est un champion et une légende incontestée de la lutte sénégalaise yalla moko def té boba deniouy santate yalla rek.
Sope yi demb yi nioy nonou tay yi mais d'après moi li modou lo bayyi takk galath molen hawa meti
@AbdouBa-k4b oui c'est possible parsk s'il n'utilise plus leurs talismans c'est qu'il ne paie plus pour ça donc niom ils n'ont plus d'utilité pour lui donc sén marché day yakou...fi d loudoul sounou borom néne leu, ils n'ont rien compris
@@khadijadiouf2747 voilà
❤❤❤
Siteu dafa daw combat bi yeup
Félicitations champion modou lo ❤❤❤
Modou gnam na d
Modou lo on’est très content mbeur bilahi diameu rk ci iow Félicitation
Modou c un vrai lion machalla❤❤❤❤
Modou incontestablement le roi des Arènes❤️❤️❤️❤️❤️
Il a pris toute initiative possible face à défenseur.
Modou vrai Jambar leu
Rousna dé je suis pas modou Lo mais mâcha allah yalla nala djik
Siteu mo waron dem jeuli Limou sokhla. jàmbaar la mais il pouvait mieux faire. Mo sokhla.
Félicitations à Modou, le grand champion
Moi je trouve que siteu était venu juste pour défendre une couronne ça se mérite mais reculer pendant 30 minutes et dire qu’il n’a pas démérité c’est honteux bilae. Tout ce que je peux dire Modou t’es un vrai champion 🎉 malgré les critiques mais t’es un vrai roi 👑
Félicitation modou lô tu as attaqué et et tu as gagné .
Absolument vrai félicitations à notre champion national tout le monde voulais qu'il tombe mes dieu à dit nom machala ❤😅
@@aliciadiouf3081 couronne bi li mou yague si mome moy dérangé 👑👑
Mod lo dou danoti si lamb incha alla.
Meilleur lutteur sénégalais ❤
Bilahi boy yi gnéméwuñ ko😮😅
Kone danouwoul ni😂
@@Mamecheikhndao-pe8nynon daanou woul épaule leu, siteu comme lac daay rassou rekk
Do yomb mou dano tii
Saway beurè dane la ak danou 😅😅bou bayi woul beurè boyi fowèko
Moi personnellement je suis balla mais Modou est le roi 👑 il a tout fait
Il a même pris énormément de risque
@@mbayewade8682am diom rek on est fier de lui notre chouchou 👑❤
Siteu Yalmine bi vrai champion nga💪🏾 Du courage
Félicitations Modou Lô🤴
Bilaye siteeu dafa beri
Du courage siteu😂 félicitations champion XLÔ🎉🎉
Modou mo beré bére bi❤❤❤❤
Mo danne danne bi tamite 😂😂😂
Machalla thiey Modou lo❤❤❤
Etant plus jeune. Tu dois entreprendre siteu na fait que défendre, un future Roi doit démontrer de la puissance d attaque mais pas de la reculade
Mais défendre fait partie du sport de combat.
Oui mon cher ami ,
Voici toute la différence entre balla gaye et les autres
@@abdoundamedieng4751
Oui mais il en a fait trop @@abdoundamedieng4751
@@abdoundamedieng4751mais durant tout le combat, c'est ridicule 😢😢😢 et à la fin , c'est lui ki se met à faire la grande geule😢😢😢😢
Vraiment frr
Non Modou day moy ndanane c le roi des arènes c’est le meilleur m nak siteu mashallah ndiambar gua ❤
Ki niou niaf ndym nganane ndanane 😂😂
@@Mamecheikhndao-pe8nyDafa di goor yalla dawoul bène yone mo deff lepp kone c'est normal daffa niémé encaissé aye coups goor deugue dou daw 😅
Nagoul rekk
@@KhadijaKontehsa diganeték yalla siteu danouwoul 😂
*Siteu est ridicule! Tu es plus jeune, tu es le challenger, tu as besoin de la couronne, tu es dominé à la bagarre, tu sors de l’enceinte 4 fois, tu as plus d’avertissements, et malgré ça tu ne prends aucune initiative, en plus ngeu japp nguemb modou jappoul dara et tu ne fais pas d’action, tu perds, et tu jubiles? Il perd et on le félicite😂. Nii le defone contre Lac 2. Wakh leine ko deugue! Au Sénégal on fait la promotion de la médiocrité surtout dans le sport, c’est désolant*
Vraiment
Qu'est ce que tu racontes mec? Modou n'a pas dominé Siteu, il faut etre aveugle pour dire ça. Modou est allé se soigner et tu nous raconte un autre combat peut-être
@@SerigneSaliouDieng-ib5mbmontres moi où j’ai confondu avoir et être. On dirait que c’est toi qui ne comprends pas français 😂
@ c’est pas parce que tu vas te soigner que tu es dominé à la bagarre. C’est possible de prendre un coup qui te fait saigner malgré avoir dominé. C’est modou qui attaque à chaque accrochage, c’est lui qui enclenche la bagarre, et c’est Siteu qui reçoit le plus de coups
Siteu daniouko dominé si bagarre bi diko dieuli alors que moom moy chalenger bi li wadji wax deug leu @@alexisniokhorsenghor-lg4gc
Yen gni nekone si plateau bi Malick thiandoum rék mossi done waxx xamxam 😂😂😂meune guéne fénnn😂😂😂no du jamais vu😅😅
Ana gni bague Modou lo ❤️
Félicitations Modou lo tu as tout donné
Oui c vrai il est et reste champion machallah
C’est le meilleur
Fans balla gaye yi dougourou aziz ndiaye yi mayléne gnou jaam 4 appuis amoul fiii CNG dina até SITEU felicitations 🎉 jambar gua modou zero faute beuré gua khékh gua telgua paré macha allah ❤❤❤❤
Modou danouna dh
Beurewut dara, daa daw combat beh jehk.
Modou lo mo meun boyi.
Siteu wakh rekk to deff ak fecha rekk la gange
Je suis dans Balla Gueye mais Moudou modef lepou
Épaule dou chute ou bien
Modou lo danouna
𝑆𝑜𝑛𝑎𝑙 𝑛𝑔𝑢é𝑛𝑒 𝐵𝑎𝑙𝑙𝑎 𝑚𝑜𝑚𝑒 𝑎𝑚𝑜𝑢𝑙 𝑠é𝑛 𝑑𝑖𝑜𝑡𝑒
En écoutant les commentateurs à la Radio , j’avais grave l’impression que Siteu mo beuré beuré bi yeup mais apparemment il n’a pris aucune initiative pour quelqu’un qui aspire prendre la couronne
Modou mo beuré mo ame ndame bravo Champion 👑👑👑❤️
Modou mo df lep effectivement mais danouna dh
@@marmichoue7857 Modou danouwoul
Modou mo xéx mo beurré mo diriger Moy déf action siteu daffa daw Di rassou té si diaxasso bi siteu mo déf 4appuit xol lén🧐loxo Modou bi mogui si kaw ☝️félicitation xaragne lo👑👑👑
Mai épaule bi mo dall si souff lolou diéll la yakar na dh
@@rimokhamou2642 40:01
@@BABACAR-l2e diaroul explication waa borbb leu lo rek
Wawaw Lou ler ngua wakh deh loxo gauche Modou Lô bi laloul souff ben Yon si action bi .Loxo yanguissi kaw ndodou Siteu bi
Modou tu as trp risqué siteu diélo bén inissiative mais lamb dji nekh na
Modou lo ya daaka beuré Senegal tellemet rapide et féroce bien joué
felicitation le grand champion
Tu es le meilleur xaragne lo
Téy mom xaragnoul
Vraiment Modou lo mon dirigé combat bi yeupe ❤️❤️❤️❤️ je suis fan de balla gaye 2 mais modou lo y'a beuré y'a attaque y'a khekh dafa lére ❤❤❤❤❤
Bly frr yaw yalla laye takh di wakh
Mbeur bou meunoul attaqué matoul mbeur. Ken dou Balla. Tous les lutteurs défenseurs n'ont jamais été roi des arènes.
@@senegalintelligenceYekini presque defenseur lawone dh wala bok contre attaquant comme Modou
Attitude bi nekk si balla da nekk si modou lo ñom dougnou Yakk lamb quoi sene adversaire sou dirigé woul ñom dagnouy dirigé
Merci Siteu on est fier de toi 🩸djambars nga
Saway ban jambar siteu dara la defoul alors que mo beug couronne Bi na diangui beurre
@@esaiesadio5215 bien répondu
@ bo manoul wonn beuré modou dakoy deff ngaka .kou manoul beuré dans beuré combat royal gnou manoul yaksiwougn niveau bii🧠je suis trop d‘accord de la façon noumm beuré avc le roi 🧠🧠
@@ModouFaye-fs5tk nono saway mono nek khale nguey daw ci sakou yi sak action
@@slattboy1293 kouy xalé 🤣🤣bayima wayy khamoo louy lamb khana amoul xalé akk magg lamb dafay ladjeu nga khamm koumay beuré manoumako eupoumako dara nga amm noo beuré akk mome sii xëll akk dalll.siteu était courageux mana deukou lokho droit modou lô .un combat avc beaucoup de polimique il lui a tenu en échec Lolou molénn nekhoul enfaite
En tout cas ce Gosse Siteu mérite Un grand respect de la part des chroniqueurs de la lutte !
nek khale sokhla roi bi di daw sak actions, diokh merite yombouna dh
Waw c'est vrai même boudé siteu doit aussi garder son sang froid en tant que sportif
Topal falé
Tu ments
Ki dou gosse Di il a 36 ans😮😂
Mais vraiment nak lamb dji nékh na trop nak bayilénn wakhi supporters yi nak modou lo nak kouma attaqué nga reculé force la
Modou lo day beurrée comme si sitteu mo yor roi bi lo khamni sitteu moko worone def.
Respecter Modou lo même si vous l'estimez pas
Billahi
🤜🤛
Félicitations Modou lo billahi yay diambar machallah ❤️👑
Felicitation les deux lutteur
Modou ték na épaule bi deh ,ragal na recoure diokh siteu Victoire deh😢
Yaw mom do nawfekh
Modou lo damala beugeu bayil beuré sama xol bi atanatoul lii😢❤❤
Juste supporters modou yii daniou ragal defaite ndakh tellement daniou beugg modou 😂😂😂mais prkoi mouy bayii na khar reug reug 😂😂🙏
@@ModouFaye-fs5tk𝑠𝑢𝑟𝑡𝑜𝑢𝑡 𝑙𝑜𝑙𝑜𝑢 𝑅𝑒𝑢𝑔 𝑟𝑒𝑢𝑔 𝑟é𝑘
Je n'en peux plus wallahi 😢
@@ModouFaye-fs5tkmeunounio ragal défaite sounou mbeur khamoul daw kom tapette, il n'a plus rien à prouver beuré mom dafko meun diko def mais yen jalousie yi mieux vaut partir, sott neniou be sonou téwoul yalla mom la faral
Bly
Nékhoule ba nékhoule cette fois ci Siteu beurré na nak
Kou beurélo Modou 20mn
Champions gua 🎉
Tu n’as pas été démériter
Félicitation à Kharagne
c'etait l'attaque contre la defense pendant 20 minutes un combat unidirectionnel. Mais lii rek leu siteu meunone def pour guéneu si Modou kouko song ya ngui si danger. Bravo a tout les deux
@@lordmajor7157voilà ta tout compris
Modou lo bimouy beurei ak lac2 niata minute la def😅siteu =lac2 parler reculer fuir daw ba nul waleu victoire sur décision arbitrale rek 😅
Balahi vérité absolu
Dire vraie siteu na yokeu beuré bayi waxx franchement Modou Lo dako diriger ci fight bi.
Siteu tangoul
Modou on t'aime et t'aimera toujours tu nous a livré un intense combat ya beuré ya dan
Biss bi yako néxal dh
Siteu Deug deug jabar la felicity ❤❤❤
Siteu sou takhawon khaamm souffrez en silence 😂😂
Lllllllllllllll
Roi bi diott na gnam ay hypercul d😂
Ce combat me rappelle un peu yékini vs tapha ... avec les reporters partisans et tout ... Bravo Modou déssa lognou dara ,courage si Siteu...yallana diam sakh
Combat bobou tapha dafa dawa dawa daw ba paré danou niari yone 😄
@@marmichoue7857 😀😀😀
Siteu roi des arènes kéne meussou ko dieulé cii dane bou takk souff du courage rék tarkinda bi et félicitation modou lo.
Siteu c’est comme si mom Mo nekon roi bi Modou diko outci😂😂😂
Bilay 😂😂
Siteu a très bien lutté c'est un vrai guerrier très bon combat entre deux jambar, j'ai peur du recours
Siteu a rien foutu😂
Frère soyons sportif Siteu à très bien lutter Modou champion leu Motakh tmt Siteu nii ley abordé ay Combat wam khana sétlouwolen lolou loubakh Mouy beurré AK modou en plus combat royal ba paré dii deugeul bopam
Modou lo mo danou
@ damani siteu mo sokhla d’accord il na rien à perdre loutakh defoul ni boy niang def ?
Siteu mo Dane
Dama bou faléwoul diol machalla modou lo ta tout donné🎉❤
Kharal ma wo balla
Malick mo meune reportage lamb franchement chapeau 🎉
Waw ils ont tous les deux bien combattu,Siteu n a vraiment pas démérité 👏👏👏
Koone xalee bouy oute daw combat bi yeup ngay félicité ?
Machalla braaaaaaaaavo modou kharagne lôooooo ❤❤❤❤❤❤❤❤
Vraiment Siteu mo Dane👑Champion deug dou Ama dou Boye Niang dou Eumeu Séne kéne amoul li si modou lo baye door mbague bi😮Recours rék niou dieuli Roi bi🎉🎉Siteuuu👑
𝑇𝑚𝑡 𝑘ℎ𝑎𝑙é 𝑑é𝑓 𝑙é𝑒𝑝
😅khana ngenn creer senn couronne boop bi dh parcelle lay desss😂😂😂😂
Ça ce voit k vous avez favorisé siteu😂 ms Modou lo dou niékhou niembé kene 🎉
Bamou dess Balla gaye wakh dey yegue
Vraiment kou wax deugue the yalla rek tax Modou lô dan na siteu bou yague
Balla gaye moy sama mbeur Modou lo vrai champion le siteu défendre rk lafi néké
Fan's Modou lô la mais Balla gaye limou ma nèkhé moye dou daw mokk moromou goor ram dina attaqué khékh beuré fofou rek la rawé aye moromam
Eumeu Sène tamite pareil bokaay raye sakh dou daw
Yéne aye seuytané nak ma wakhe gnounane défnafie loumou meussoule déf modou a bien fait ☑️ Sama domou baye bie machalah
😂😂😂ta sou Modou lo takhawone niou tamko deum😂😂😂
Siteu moy bandit ❤
Non sérieusement tay siteu sonalna grand bi quoi ❤😂😂
Vraiment siteu diambar leu ❤❤❤
Diambar dou daw soxnassi
Félicitations SITEU le VAINQUEUR JAMBAR NGA💪🏼
Félicitations Siteu 🎉
Gniye reporté gnon nafèx😂mane douma fans modou mais siteu dèfoufi guate da daw lamb djii yeup😂😂
MODOU C'EST UN ROI SI VOUS REmarquer a la fin """"HEY DAGNIOUY FOOO""""
MERCI MODOU LO
Merci🎉
Filiçitation Modou lô ❤wadji dafa dawe lambou dji ba amthi li
Félicitations à modou lô il mérité amplement sa victoire ❤ et siteu doit se remettre en question et arrêter de célébrer des défaites comme une victoire amal diome
Modou lo machalla ❤❤❤❤❤amal diam
Mann siteu d'où Sama mbeurr mais pour dire la vérité. Siteu mo gagner modou lo da danou Srx on se dit la vérité les gars farr néxoule mais deugg thi leuh bok. Combat bi nehna trop Mei siteu a gagné wallahi kou d'accord beusseule j'aime gua commentaires niou yatal
Non tay mom boy bi sonal na m'y grand😂😂😂😂😂😂
Daw you méti no def soon.
Siteu bou tahaawone sakh mani waaw, mais di rassou ba combat bi diééh, wah lennko mou changer stratégie moo gueune😢😢😢
Deug -Deug Siteu djambarr nga...MaShaAllah Champion
Ki daw allee bi yeup
Nn franchement combat bii nekhna trope siteu béteunama trope thii combat bii Mashallah ❤
Félicitation modou ndam noko amer baxna couronne bi delouna parcelle courage siteu
Modou loooooooooooooooooooooooooooooooooooo ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤ vrais champion
Félicitations à siteu goor yalla pire ga tu as assuré
Modou lo 🤣🤣 a juste corrigé siteu au calme...
Félicitations notre lutteur X lô tjrs égal à lui même diambar deug💪🏾💪🏾💪🏾👑❤️
Siteu wax ak daww doula meussa may couronne bii 🙌🏾
No modou lo jambarrr la yalla.khamnako un.vrai combattant
Billahi
Il faut dire la vérité c Modou lo qui mérite la victoire dans ce combat en tout cas c Modou qui a tout fait
Soyons honnêtes té bayi thiakhan yi siteu mo def 4appuis mo danou dafa wara changer sa façon de lutter dafay daw rek dieuloul bén initiative té taye môme mo momone combat bi
4Appuis de Siteu? Tu es aveugle khana? Où bien denga far ?
Modou defend sa couronne.est c,est normale c,est le plus fort
Félicitations siteu tu peux être fière ✌️
Fier de quoi 🤣
Les reporters étaient vraiment avec siteu
Siteu bilahi nakho niou nioune gnila beugue❤ 3 fois ardo + ramloko😂 Tarkinda 🎉
Mo am defait dh😂😂😂
Arrière lamb j yeup. Gate xamouko. En plus môme lagne rame lo.
Tarkinda seul
Bilay walay ❤on est fière de lui Bouchoura bi ❤❤🎉lalay tegal d
@@astbndiagorbidawkinda bi lac 3😂😂😂
Modou Lo meilleur lutteur du Senegal.
Mou déss SATHIES. Boy yangui diékh dh 😂😂
Les hommes au micro manquent d objectivité !
La chute de Siteu était évidente sur 4 appuis.
Il faut éviter de tomber dans un esprit partisan quand on a comme rôle de rendre compte au grand nombre.
Je vous souhaite beaucoup de courage.
Merci
T'as tout dit, ils ont vraiment été décevants
Pourtant 3 appuies successifs leu df, deux genous et main gauche mais bi main droite bi di wathie dafa yeukeuti main gauche bi fékaneté wouniou kholal bou bakh.
Mais nak modou mo beuré beuré bi yeup