Intéressant de voir un jeune s'exprimer de la sorte. Mais à mon avis il fait plus de philosophie (manam ci xalatam rek layy wakhè) que des interprétations basées sur le coran ou les hadiths et autres. Et un conseil : mahrifatou billahi c'est la clef...
C un programme dou si niveau bopam lay wakhé mais si niveau nit gni de façon general. Bofi togone di wakh marifa arifina yi rek niolay deg gnissi des dinagne la takfir teh si bir arifina yi sakh dina am nioula dingat. Yonente bi nak wala yonente yeup sakh danio preparer khelou nit gni avant nioussiy dougal dara. En plus niom nieupa philosopher ba yalla indil lene revelation. Philosphie moy nonou religion bi gueuna reuy mais aussi moy kharitam bi gueuna reuy. Ghazzali avant mouy done arif billah dafa defi pholosphie ba maitriser ko nit sakh meunoul nek arif teh maitriser woul philo. Ghazzali bimouy binde Al munqiz minad dalal wakh nako. Bo sété lim wakh wakh dangay guiss ni philo moko dougal si haqiqa deug teh demna ba am 54 ans di diangalei yalla. Ben biss la tok poser bopam quesstion ni mann may kane? Amoul reponse mou bayi theologie dem diangui gaday saubou si yonou marifa mais dafa fek mou diangui philo ba maitriser 4 branche philo yeup.
Nitt ki soko preparei si cote bobou ba parei diaroul ngakoy diamgal xam xam si diamono bi niou tolou mom mokoy outal bopam.ndakh nieupangui outi xam xam mais nieup amouniou xam xam si bir borom xam xam yi amnasi nio xamni ay robot lagne copier coller laniouy def. Mais 'ilmoul hadith bo kholer façon biniou weralei hadith philosophie rek, charia bi bo sété Qyas nimouy dokhé dou dara loudoul philo ndakh Qyas analogie la, teh analogie logique moko mom. Teh logique si 4 branche philosophie yi la bokou. Ak yenene ak yenene kou maitriser philo doko gueiné si islam guinaw binga amé foi il faut nga philosopher ndakh nieupangui wakh di soukandikou si hadith ak alkhourane teh takhoul nieup bokou deiguine si hadith ak allhourane ,niata charh mofi am niata tafsir mofi am ? Liko waral moy raisonnement yi ak methode nit gni di diar pour avoir acces à la verité mo outé manam philosophie yi nio outé. Nieup ay philosophes .
En fait, pourtant liouy deif haqiiqa pur leu dou philosophie dei. Ndakh philosophie dafa dellou si di khalaate si loula woroul wayei li pathie la si mahrifa bi ngay wakh ndakh kou kham sa bopp kham yalla « Mann harafa nafsahou harafa rabbah » dafa feikk ni gnounn dagno tamm bou gnii wakh si haqiiqa bi dellou si nit, dagnouy fattei ni leipp lagnou wara dieul: dimension physique, mental ak spirituelle, bo si bayyi reik mou am lou manquer, lolou nak la façon diangaleim yi di rectifier. Nei nga limouy wakh teigou woul si Coran ak sunna et pourtant si. « Wa fii anfoussikoum afalaa toubsiroune » yalla si Alquraane mo gnou ndieukeu insister si gnou découvrir sougnou bopp. Waayei yittei bobou la gnou amoul tei lolou mo waral meunou gnou créer dara ndakh da gnou diapp ni leipp ay wakh you abstraits la si wallou mahrifa, d’ailleurs toubab yi lolou lagn gnou rawei motakh gnom bou gnou gueumone yalla dougn gnou sakh khool ndakh seine sciences yi sakh keinn dou co gueinnei si haqiiqa yalla bi.
ISLAM ay texte la. Ce n'est pas la PHILODOPHIE. Également chaque chose en son lieu. Les prétendus cours universitaires ne se font pas dans la rue, car ils peuvent pervertir! Quand on parle de "niveau", il faut tenir compte du récepteur c'est çà l'intelligence.
Tu es certainement un grand ignorant. Tu écoute un philosophe qui parle du n'importe quoi au nom de l'islam. Vas apprendre ta religion mon frère et il ne faut pas être comme un cochon 🐖 🐖 🐖 🐖 🐖 🐖
Tu dois encore apprendre, lire et approfondir ton entendement. En plus, tu confonds le sens des termes et des concepts. Il te reste beaucoup de choses à savoir. C'est trop tôt de parler de ta part
Malheureusement il ne méprise pas ce qu'il est entrain de dire ,son discours est juste métaphysique mais ya aucune relation entre son explication et la vrai définition d'un rêve. Liguay wakh dara amoussi walay.
Mon cher, si vous dites que son discours n’est pas conforme avec ce qu’est la définition du rêve, vous devez être en mesure de nous définir ce qu’est réellement le rêve. C’est cela une bonne démarche de critique intellectuelle.
Arrêtons de faire semblant. Disons les choses telles qu'elles sont. Ki waxoufi dara. Il n'ya aucune cohérence dans son discours. Sénégal mom nekk fi serigne lou yomb la. Utilisez len sen xel yi té bayi complexer
L'hypocrisie du Sénégalais me dépasse ! Lorsqu'un talibé Tidiane s'habille comme ça son père l'insulte de tout les noms et lorsque le fils de leur marabout s'habille de cette manière avec chaine blig blig nada rien c'est normal.
kawma capitaine khawma générale mais yaw wakho xam xam dh démal nga diangui nék settou maodo yomboul dh fook nga diangue ba khôtt loll si guedjou xam xam
Suis pas d’accord tu n’es pas pertinent à ce point il te reste bcp de chose à apprendre à travers du cerveau et de l’information et la connaissance sprituel ga balma cheikh mais colier bi mom dou sa trieur talla n’alla talla sameu
T'as commenté 2f8 de suite pourquoi vous êtes ingrat et insensé moi j'arrive pas à comprendre vos attitude envers vos prochains mieux vaut encourager une personne qui essaye au lieu de la critiquer même s'il a fait de l'amalgame ou qu'il maîtrise pas le sujet mieux vaut l'encourager parce qu'il est encore jeune et quand il prend l'âge la sagesse entrera et toi qui te connaît ? Tu sais même pas parler avec tes suggestions bidon. Bizarre homme que tu es
MACHA-ALLAH sa XAM-XAM SETNA LÈRNA,te compatible na AK JAMONO té guenoul CORAN AK SOUNAH.K DIEU vous protège.
Intéressant
Koulakhamalnisenla machallah kapitain
Nooo les gens qui l'écoutent laa mom amnagnou temps dh ??
Intéressante explication logique et plausible!
Futur serigne cheikh tidjane sy almaktoum
Vraiment fitt moom am ngako trop my boy demal djangui seu diiné
Day ték khél rék khamoul touss
Sy malike yalla nakafi yage ❤❤👏👏
Mais nak Mr le capitaine ndanane gua !
Merci bon ramadan
Dieureudieufé soniou gorgui💯💯♥️♥️♥️💚💚💚💚💚💚💚💪💪💪💪💪💪💪💪💪
Intéressant de voir un jeune s'exprimer de la sorte. Mais à mon avis il fait plus de philosophie (manam ci xalatam rek layy wakhè) que des interprétations basées sur le coran ou les hadiths et autres. Et un conseil : mahrifatou billahi c'est la clef...
C un programme dou si niveau bopam lay wakhé mais si niveau nit gni de façon general. Bofi togone di wakh marifa arifina yi rek niolay deg gnissi des dinagne la takfir teh si bir arifina yi sakh dina am nioula dingat. Yonente bi nak wala yonente yeup sakh danio preparer khelou nit gni avant nioussiy dougal dara. En plus niom nieupa philosopher ba yalla indil lene revelation. Philosphie moy nonou religion bi gueuna reuy mais aussi moy kharitam bi gueuna reuy. Ghazzali avant mouy done arif billah dafa defi pholosphie ba maitriser ko nit sakh meunoul nek arif teh maitriser woul philo. Ghazzali bimouy binde Al munqiz minad dalal wakh nako. Bo sété lim wakh wakh dangay guiss ni philo moko dougal si haqiqa deug teh demna ba am 54 ans di diangalei yalla. Ben biss la tok poser bopam quesstion ni mann may kane? Amoul reponse mou bayi theologie dem diangui gaday saubou si yonou marifa mais dafa fek mou diangui philo ba maitriser 4 branche philo yeup.
Nitt ki soko preparei si cote bobou ba parei diaroul ngakoy diamgal xam xam si diamono bi niou tolou mom mokoy outal bopam.ndakh nieupangui outi xam xam mais nieup amouniou xam xam si bir borom xam xam yi amnasi nio xamni ay robot lagne copier coller laniouy def. Mais 'ilmoul hadith bo kholer façon biniou weralei hadith philosophie rek, charia bi bo sété Qyas nimouy dokhé dou dara loudoul philo ndakh Qyas analogie la, teh analogie logique moko mom. Teh logique si 4 branche philosophie yi la bokou. Ak yenene ak yenene kou maitriser philo doko gueiné si islam guinaw binga amé foi il faut nga philosopher ndakh nieupangui wakh di soukandikou si hadith ak alkhourane teh takhoul nieup bokou deiguine si hadith ak allhourane ,niata charh mofi am niata tafsir mofi am ? Liko waral moy raisonnement yi ak methode nit gni di diar pour avoir acces à la verité mo outé manam philosophie yi nio outé. Nieup ay philosophes .
En fait, pourtant liouy deif haqiiqa pur leu dou philosophie dei. Ndakh philosophie dafa dellou si di khalaate si loula woroul wayei li pathie la si mahrifa bi ngay wakh ndakh kou kham sa bopp kham yalla « Mann harafa nafsahou harafa rabbah » dafa feikk ni gnounn dagno tamm bou gnii wakh si haqiiqa bi dellou si nit, dagnouy fattei ni leipp lagnou wara dieul: dimension physique, mental ak spirituelle, bo si bayyi reik mou am lou manquer, lolou nak la façon diangaleim yi di rectifier. Nei nga limouy wakh teigou woul si Coran ak sunna et pourtant si. « Wa fii anfoussikoum afalaa toubsiroune » yalla si Alquraane mo gnou ndieukeu insister si gnou découvrir sougnou bopp. Waayei yittei bobou la gnou amoul tei lolou mo waral meunou gnou créer dara ndakh da gnou diapp ni leipp ay wakh you abstraits la si wallou mahrifa, d’ailleurs toubab yi lolou lagn gnou rawei motakh gnom bou gnou gueumone yalla dougn gnou sakh khool ndakh seine sciences yi sakh keinn dou co gueinnei si haqiiqa yalla bi.
Deugue nga wax,Alkhour'aan daal moy deugue...
ISLAM ay texte la. Ce n'est pas la PHILODOPHIE. Également chaque chose en son lieu. Les prétendus cours universitaires ne se font pas dans la rue, car ils peuvent pervertir! Quand on parle de "niveau", il faut tenir compte du récepteur c'est çà l'intelligence.
Allhou akbar ❤
Vraiment amna solo trop
Yalla Nanou yalla fayal souniou Mame Cheikh ❣️❣️❣️
Machallah mon idole 👏
machaallah jadore son idéologie
Machaallah 😍❤️❤️
Bi si déss diamono dafay évoluer Kone ki wara djou beuneti nite gni si cadre stratégie fokeu mou Niro AK gnome si kaweu mais si soufeu waweu kayeu
Mâcha alla
C est très intéressant !! Dommage qu ont n a pas ses genres de conférences en France
Tu es certainement un grand ignorant.
Tu écoute un philosophe qui parle du n'importe quoi au nom de l'islam.
Vas apprendre ta religion mon frère et il ne faut pas être comme un cochon 🐖 🐖 🐖 🐖 🐖 🐖
Nga baalma gorgui tekkil chaine bi nak... plzzz🤞
Non frére il faut lui dire que djoulitt bou gorr dou takk Chaine
@@sambandiaye8873 c la pur realité
@@sambandiaye8873 est ce que julit la?
téléchargement de l'apologie de SATAN en cours
Diaradieuf Serigne Moustapha
en tant que domi soxna tak chaine warula au contraire y’a waron guiss koukoy deff nga ayei ko
Yaw do domi Soxna ?
SOKHNA BANE? Le mot est de Serigne Abdou, et les critères sont sélectifs Hein?
Pertinent 👌
Tu dois encore apprendre, lire et approfondir ton entendement. En plus, tu confonds le sens des termes et des concepts. Il te reste beaucoup de choses à savoir. C'est trop tôt de parler de ta part
Le Plus Important C’est D’avoir Cette Rage D’essayer Ça N’a Aucun Sens D’attendre D’être Parfait Pour Commencer Qu’Allah Soit Satisfait De Ce Jeune
Philosophie la rek
Alioune Badara yaww kou sokhor ngua, tédieul sa guatt bi way akh
Ioe kou bonn nga
C’est quoi le rêve bAdara ?
Machallh niveau bi kawena Comprendrouma vu dra mais begg na lol
Ah man dh li néka si bat bi lay lathité xana dou chéne dh la yakar
Malheureusement il ne méprise pas ce qu'il est entrain de dire ,son discours est juste métaphysique mais ya aucune relation entre son explication et la vrai définition d'un rêve. Liguay wakh dara amoussi walay.
Mon cher, si vous dites que son discours n’est pas conforme avec ce qu’est la définition du rêve, vous devez être en mesure de nous définir ce qu’est réellement le rêve. C’est cela une bonne démarche de critique intellectuelle.
Machallah 🥰
Arrêtons de faire semblant. Disons les choses telles qu'elles sont. Ki waxoufi dara. Il n'ya aucune cohérence dans son discours. Sénégal mom nekk fi serigne lou yomb la. Utilisez len sen xel yi té bayi complexer
اللهم احفظ وبارك
Machallah ♥️♥️ bilay capi👏👏👏
Sénégal nekhna billaay liii
Wa fi dara thi kham kham wakhi tapalé rek guaye wakh koula topoy senkou dara khamoko té gua kholate sa acoutroument en tant ce domou djoulite
😂😂😂
Mais kii loumouy wakh nii 😂😂😂. C vraiment utopique
L'hypocrisie du Sénégalais me dépasse ! Lorsqu'un talibé Tidiane s'habille comme ça son père l'insulte de tout les noms et lorsque le fils de leur marabout s'habille de cette manière avec chaine blig blig nada rien c'est normal.
Pure Vérité. La preuve en un an, tout le monde vous fuit 😀
Gorr dou tak sén 2ème fois bi amoul kham kham khélam rék lay wakhé begue na wax xam xam mai amouko
Capitaine ragalal yallah ligay wax ni tégouwoul feen
Capitaine mi kou yabaté la dafa wara dianguiwatt wakhi doff rék lay wakh
Demal ndiagui khamo dra liguey wah amoul Ben ndiarign du khammm khamm
Vraiment
Il dit quoi la ? Je comprends rien du tout
Capitaine❤🥰
Fatabarakala
Boybi khamoul touss manolén gnouko forcé bamou gondi gnou wakhi doff rék lay wakh 😂
Il confond terme et concept
Serigne bouy taakeu chaîne?🤔
Ki khamoul Lou Bari, il doit encore bcp apprendre avant de palabrer
Futur Kilifeu, Machaallah
Chaîne bi nga tàkk nak. Goor du tàkk chaîne dafa haraam
Kii limiy wax ndax mën na ko répéter waat
Walahi tapalè bakhoull il faut nguènn bayii fohh app soit disant "Serigne" dina takk chaîne nitt yi khamlènn fou nguènn di tèkk seen tankk
Un discours islamique où on entend pas le tout puissant a dit ou le prophète a dit .
Ça m'arrive parfois ce qu'il explique
Sénégal mo beurii ay comédien
Franchement je ne peux rien comprendre et ces gens qui applaudissent ne le font par partisannerie
Leeguii ma lathe biiii you taaaw moyyyy fefff eyyy éclair nakkk Adama et biii diii khare moyyy lannn
Non j'ai pitié de mon pays, quoi...
Ki rappeurla wala chaîne bi nk 🤥
Vraiment yeine fiakhal ngéne ma d
Boybi limouye wakh khamputhi dara gnikoy deglou rek gno gnakk fayda
Ak sa chaîne....meile ni Waly
Mais ki keskil raconte...
Il dit du n'importe koi..
Ki loumou wakh ?
Qui est ce monsieur, svp, waxlenn, kann momaay tontou ngir Yallah, ndax lumu wax lumi ko tegg ak pourquoi gni di ko suivre avec autant d' attention ?
kawma capitaine khawma générale mais yaw wakho xam xam dh démal nga diangui nék settou maodo yomboul dh fook nga diangue ba khôtt loll si guedjou xam xam
L'islam amoul tholine bou officiel
Thieuy funiou jeum
wahlein ko takk chaine dafaf haraam
🤣🤣🤣🤣
Doff pire ga yow
Kane mola lath sa avis
Takk chaîne bi amalougou importance,loumouy wakh mognou amal importance. Dieureudieuf capitaine
Que du vent
Ki il est trop nul si vous pensez qu’il assurera votre relève il se ridiculise ta dara xewagoul
Bilahi tu as raison frère je suis un fervent talibé de Serigne cheikh tidiane Sy Al makhtoum mais ce goss est très nul
Li ngay wax xamo si dara faiseur de malin
Ndeysaaan
Wahal lu melni loumouy wah
Took sa guinaw clavier di Doxot yomb na
WOKH NGA DEGGUE DOUL RÉK LAYE DÉF
@@omardrame5763 sa bay sakh ki moko eup khame khame
KII KHAMOUL DARA DOU ALQURAN DOU SUNNA KHAMOUL
😂😂😂😂
Suis pas d’accord tu n’es pas pertinent à ce point il te reste bcp de chose à apprendre à travers du cerveau et de l’information et la connaissance sprituel ga balma cheikh mais colier bi mom dou sa trieur talla n’alla talla sameu
Waxlénn ko mou djiangui philosophie
T'as commenté 2f8 de suite pourquoi vous êtes ingrat et insensé moi j'arrive pas à comprendre vos attitude envers vos prochains mieux vaut encourager une personne qui essaye au lieu de la critiquer même s'il a fait de l'amalgame ou qu'il maîtrise pas le sujet mieux vaut l'encourager parce qu'il est encore jeune et quand il prend l'âge la sagesse entrera et toi qui te connaît ? Tu sais même pas parler avec tes suggestions bidon. Bizarre homme que tu es
@@khalifaababacarsall1430 on ne doit pas répondre un idiot donc désolé mais j n vais pas te répondre
@@abdelaziz315 parce que t'as pas d'arguments Refré
Ki mooo gueuneuh nullard Sénégal
Terem bi nasi defar bu araab way lakum tubab mom dara lasi wamul
Vraiment sa waye nieley deglou diakhal naniouma 😭 tu es vraiment nul 👎
كذبت لم نر دليلك في القرءان الكريم ولافي حديث النبوي
😂 encore un virus
C’est toi qui est le menteur, tu appelles à la sunna et au coran après tu insultes les gens parce qu’ils sont ignorants bravo
T’as qu’à dire que t’as pas appris ça
Bou bayi wone lakk toubab bi ma geun ko meuneu deuglou et plus credible
Wakhi kassaw kassaw!!! Doul waay!!
Boy bii Moy kann
Hahaha
@@adiadiop8395 répond mow
@@usmaanaa8071 c'est le fils de Serigne Moustapha Sy
Philodof mafia bou mak
N'importe quoi