Waaw kou baakh manguilay ziaar. Dama laayé biir donté ni sakh amouma xam xam silou wer nak. waayé boo beugué Xam boulni mouk looxamoull rekkeu amoul. Yalla bour la bookhamné loumouko nékhé, ak foumouko nékhé lay def Mbireum, khoooloul ndakh nit gni comprendre naniou wala. Ndakh, il n'a de compte à rendre à personne. Mane weddi wouma linga wakh, wakhdji daa khawna diss waayé soula yalla mayé deggueu rek ngakooy xam. Waayé ki xam leppeu rek moomeuna wéddi, waayé yiow xamooo leppeu, yalla rek n xam leppeu. Saaway yalla daaa mayé dé.
Encore une fois la pertinence et la cohérence dans l’enseignement sont manifeste. Vous démontrer la faiblesse des écoles occidentales par l’intermédiaire de la hauteur des interventions. Avec ce Colisée vous formez de nombreux gens en manque d’analyse logique.
Limouy wakh mégowoul ak allhour an ak sounnah . Wakh si diné nagnouko ték si kham kham bou fi muhamad dianguelé. Liguay wakh tégoko si kham kham dinè bayil di wakh sa khalate.
mane dei passage tabaski bi entre 5 djiko yi si ibrahima ismailla sokhnassi djibril ak khar mi moma daneil xam xam dal amna ay waye senegal kou deiglou capitaine bo yeiwatei sa kharoume tabaski di kholat sa bopou ndax djikoyi dajieina si yaw machalakh sy malick gaindei dou diour mousse doundeul weireul
Grazie mille 🙏
Domi mbeur dal dianguil beure thiey mame Cheikh diar nga sa yon ba deh très bien👏👏👏👏💯👍❤✅
Machallah notre capitaine diarama serigne mouhamadoul moustapha sy
ALHAMDOULILAH dieureudieuf Cheikh Mouhammadoul Moustapha sy al maktoum
Macha Allah, quelle clairvoyance !!!
Maachallah Mame Cheikh sa xam-xam dafa lakkhou, djoulit bou limité meunta kham lingay wakh. C'est plutôt subtil.
Jambaar lolou amoul. Louy xam xam bou lakhou? Bayiléne nakhaté bi
Waaw kou baakh manguilay ziaar. Dama laayé biir donté ni sakh amouma xam xam silou wer nak. waayé boo beugué Xam boulni mouk looxamoull rekkeu amoul. Yalla bour la bookhamné loumouko nékhé, ak foumouko nékhé lay def Mbireum, khoooloul ndakh nit gni comprendre naniou wala. Ndakh, il n'a de compte à rendre à personne. Mane weddi wouma linga wakh, wakhdji daa khawna diss waayé soula yalla mayé deggueu rek ngakooy xam. Waayé ki xam leppeu rek moomeuna wéddi, waayé yiow xamooo leppeu, yalla rek n xam leppeu. Saaway yalla daaa mayé dé.
j'apprécie le fait qu'il parle de chose terre a terre accessible et compréhensible a tous sans un mot arabe parfois qu'on comprend pas grand chose
Machaalah MAME Cheikh Tidjane Nôtre très cher 🕋🇸🇳🕌 Capitaine Yalla nalla yalla arre Barkelleu sam'leu yokoula kham-kham Wii Lakheuleu fou Yakh Yëggoul moussal-leu Thiatte AK Lamigne moussiba akk balah cii barckè alkhour-anne machaalah 💯🇸🇳
Wallah nadasane sy Capacité ❤❤❤❤❤
Notre capitaine que dieu le protège Macha Halla Aminnn
Machalla
Vous croyez que DIEU va protéger ce mécréant ?
MâshaAllah waay sunu Capitaine yalla nala yalla dolé taxawu aar la goudal sa fan wéreul la mousal la ci Thiatt 🤲🏽🙏🏼😍❤
ماشاءاللهم صل علي سيد نامحمدوسليم مام شخ احمدتجان سي المكتم
Mame cheikh tidiane sy man moride la wayé damalaa bègue lolo amal diamo rék sy malick 🙏🙏🙏🙏
Senegal dafa nékh dh
Dangay wakh say bêtises ba paré nite gni topou la kii wakhoufi dara .démal diangi mo guene lii ngay déf nii
Machalla la clairvoyance des paroles yalna yalla sameu capitaine
Amena solo trop wakhtane bi
Kou yaboul té
Machalla notre capitaine de coeur ❤️❤️❤️
Machalla s Moustapha s'y maktoum wadji n'a
Capitaine yallna yalla motali lepou inchallah
Diarama Serigne Moustapha sy
Machalla ninga Mana méll sy Malick doundal wéurel yalla samou le arrle🙏🙏🤲
Encore une fois la pertinence et la cohérence dans l’enseignement sont manifeste. Vous démontrer la faiblesse des écoles occidentales par l’intermédiaire de la hauteur des interventions. Avec ce Colisée vous formez de nombreux gens en manque d’analyse logique.
Yalla na yalla motali sounou yéné and ko ak sounou capitaine
Dieu merci biga niou bolek capitaine yalla naga niou may niou kay deglou tadiko degeu♥️🤲🤲🤲🤲🤲🤲♥️
Machallah machallah ham ham bi seellna sy malik yalna yalla arrla t samla🙏
Machalla yalla na yalla motali si barké Serigne Moustapha sy
Walay tivaoune li la mérite machalla
Machallah yallna Yallah motali way si barké goor gui 🙏🏽
Machallah,❤️💯
Capitaine des soldats 🙏
Yallanala yallah bayi sounou kanam🤲
machalla capitaine❤❤ 2:47
MACHAALLAH yalna YALLAH Barkèl
Notre capitaine ❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️
Sama khole khole bi kome firigo💕💕💕💕💕💕💕💕
yalna yalla mattali inchallah
Mach Allah yalla na yalla fayal niou la raw ga nieup
Je t’aime trop capitaine 👨✈️❤️🥰😘
Fatou
Sunu Capitaine doundal wéral sy malick
Amine inchallah ♥️
ما شاء الله اللهم لا اضر
Yore sa kham khamou bope dafa nékh rawatina kham khambou lere machallha
Lii bane diiné leu
Machaa Allah Sy Malick. Yalna yalla samou la.
Capitaine yalna yalla samoula arla
Notre capitaine je suis fier de toi❤🥰
machallah sy malick yalla na yalla arr
Laff cëtt Maam le capitaine des ❤
Vrema c interessant machaa Allah
Machallah nôtre capitaine
Amna solo
yalna yalla barkel lafal la thiat ak borom khole you fekhoul yi🤲♥️🥰
Machallah Mame yalna yalla motali lépp inchallah ❤️❤️
Yalla nako yalla samou arre kou
Machallah yalna sa diame yague rk inchallah capiténe Mame cheikh
Masha Allah
والله مدارس السيد محمد المصطفى سه فى العلم خير مدارس
خير المدارس
ALHAMDOULILAH
Yalna yalla samou s'y malick
Mashallah 🥰
Thieuy Lou nekk ak Kiko mommmm
Nignouye wakhé mô diék sof si bopame féne Réck laye défe
Yaw ba mandou gua réck et j’espère que diangue si oui diohma sa numéro niou wahtane si khakhikha
MACHAALAH CAPI
❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Macha Allah Mame cheikh
Capi❤️
Machallha ❤❤❤❤
Kheureum rek😈
إن أدرت العلم فاصغ إليه
وإن لم ترد فاسلك سبيلك نتدم
جزاك الله يا نجل مصطفى بجاه نبينا المصطفى
تندم
Soubhanallah, ki mo reer ! Allahou Akbar kabira.
Wahi dof rek lay wah.
Euy waay bou fékké wahi dof lay wah lane mo siy sa yoone mandou bahna trope gueumeul lingua guem bayyi gnou ak lignou guem yalla bahna
Wahniiou loumou wah ak louci doffé
Bénénn bi laane moy doff
Thiey yalla anni kham kham
Yalla beuggoul kouy togne
Machalah Sy Malick
Machlla walay amo morome
Machalla amna kham kham mane moride La Mai ndamaye bègue wakh taname
Machalla capitaine
Machalla capitaine ممتاز
MachAllah MAME CHIEKH 😍🤏
Demal djiangui dji boy
Ana lou yénéte bi diangualé?
مداريسه في العلم خير مداريس
Dafa ler
Machallah 🙏
Walay Sy ni nga mana mel
Machalah
ayy waay kagne laay giss dieumeu dji c moi galay dans la serie waxandè
Tite na si diné sénagal🥱ki da wara nope😱
Sénégal dafa nekh kou diogue comédie😅😅😅
🤲🤲🤲
Mâcha alla
Comment un ange peut-il faire une erreur ?
CE GAMIN EST RIDICULE🤣🤣🤣🤣🤣
C'est vraiment ridicule. 🤣
@@abdoufall13 BOY BI BILAHI KOU GNAKK YARR LA
الحمد والشكر لله
Ki féne rk la meune Bayiléne diko déglou
Machallha sy al maktoum
Féne rek demal diangui
Limouy wakh mégowoul ak allhour an ak sounnah . Wakh si diné nagnouko ték si kham kham bou fi muhamad dianguelé. Liguay wakh tégoko si kham kham dinè bayil di wakh sa khalate.
❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Delen bayi mame cheikh sarr mouy wakh boulenko ekarté mola eup kham kham
Wa keur seydi elaj Malik nio raw thie rewmi lolou la yalla dogal
Wallahi day reeral jamu yala yi xamul tuss
mane dei passage tabaski bi entre 5 djiko yi si ibrahima ismailla sokhnassi djibril ak khar mi moma daneil xam xam dal amna ay waye senegal kou deiglou capitaine bo yeiwatei sa kharoume tabaski di kholat sa bopou ndax djikoyi dajieina si yaw machalakh sy malick gaindei dou diour mousse doundeul weireul
Néna Djibril def na erreur