Dans ce monde et partout, les vrais génies sont incompris. Hélas, c’est ainsi que va le monde. Thione Seck est un génie de la musique. Ki aye texteum rek, sa mélodie et la justesse de sa voix sont impressionnants.
Papa thione wallah jtm bien dama beugeu ligueye ak studio bi je suis artiste diapalé ma rek te yalla takh lou nek def nako mes fi bo amoul diapalé do dem teh waye rek la am nguir yalla ma wané sama tallent
Thione papis Thione papa Thione tonton thione frère Thione de tous les temps depuis mon enfance jusqu’aujourd’hui, j’écoute et je te suis . En écoutant j’ai la nostalgie, des frissons et j’ai peur parce que tu rappelle au bon Dieu , tu donnes des conseils de la vie et surtout la nostalgie de la maman que j’ai pas connu qui est parti au delà j’avais 3 ans ... Quand j’étais au Gabon chaque matin Fari était mon album préféré Je suis le premier fan de Wally à Paris mais je n’ai jamais parti à ces concerts ni vu mais c’est dans le cœur, je le défends là où il est critiqué. Longue vie à toi papa Thione Allah est grand ..........
Masha Allah ! Papa Thione, sa génération tu fais parti des meilleurs chanteurs, le plus Grand Parolier Masha Allah ! Le Papa de notre Diamant Boy Wally Balago Seck le Chanteur du Peuple Masha Allah ! Yallah nalène Yallah dolé same, doli soutoura bi Amiinne Ya Raby Alaminah ❤❤❤❤❤❤❤👑👑👑👏👏👏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏
guiss nafi ben commentaire mouy nane thione amoul disc dor yew mi commentaire lolou khale nga motakh papa thione amna 4disc dor famile maickl jackson Diokh na niou ko disc dor mome ak presidant abdou Diouf amat na disc dor ak africano son bimou wey sey amat na disc dor ak rappeur france bobou mogui toudou diziz la pest ak benen disc dor ancor ak sovalier ardo merit ak sovalier orde nasional ak sovalier orde merit de lion ak yenen trophe youdoul yoyou ay khale ngan motakh ni rek ngen di def Ba nit ki dh apres ngen nek fi nane Ndessane ak statu youdoul Diekh longue vie a toi papa thione grand parolliers de la musique senegalais
Non senegal mo beuri seytane lane mofi indi wakhou youssou ndour bayilen seytane way senegalais yi seytane yoboule ken aldiana delen defar te bayi nafek longue vie a toi papa thione
Y'a des gens qui t'aiment mais aussi d'autres te détestent c'est évident et tu sais pourquoi ils te détestent parce que t'es honnête mais il faut prendre l'exemple de Sidi Lamine Niasse c'est après sa mort que les Sénégalais se sont rendus compte qu'il était un homme honnête véridique soit toujours toi même papa Thione
Au moins tu l'as témoigné vivant li Allah beugue. Demako lire avec des larmes beu legui décès bi defma diaap Wayé yalnako Allah Diegual mayko Aldiana si Barké Mohamed ( Psl) Deugue lou wattal limouy wah sah yi si biir souff😭😭😭😭😭😭
Bonjour tonton thione j'aimerais te rencontrer j'écoute tes anciens musiques de l'année 80 ??? j'adore longue vie à toi santé à toi 💖💖❤️❤️❤️❤️❤️ santé à ta familles
Mashalla le meilleur chanteur au monde surtout au Sénégal t es un grand Monument de référence do moromou beneu weuy kate fi si Sénégal on a la chance de t avoir ici au Sénégal je tm fort
" A telle enseigne que" Nékh nala Papa Thione. Temps yi mome dangako dieule rék meno wakh bamou diékh té dougalokassi😄😄 Sinon j'adore ta musique. De part les thèmes abordés, elle est très instructive et trés utile. Waay nga lépp machallah
Personne ne conteste le talent de youssou NDour.il ne faut pas déplacer le débat. Il s'agit du clan de Youssou le politique qui concentre beaucoup de pouvoir entre ses mains. C'est vrai ce que dit Thione Seck. En un mot on adore le chanteur, on déteste le politicien. On ne peut pas être bon partout.
Repose en paix Papa Thione Balago Seck le grand parolier s'en est allé.Yalla nako Seydina Mohamed téru ci Aldiana firdawsi aduna kéne deuku fi niit ku manu la won machallah 🙏🙏😭😭😭😭❤
Belen djiguel , soumakoy degglou damay xalat sama bopp walleu xalat souma niakone sama meilleur ami , motax dama beug mon meilleur ami > beugouma adouna bett ma , je préfère ndieuk ko dem , ndakh je ne peux pas vivre sans mon meilleur ami Papytö Jiiaay . De la part de ton frère NdiaaX
ta liguéye waye yepe gniou guie caye doundou parceque ça me aye kharitou Sénégales gniome liguéye tasse ça seuye ndakh igniane taique ta na ne aye domou dioulite lagniou ndakh comme gniome praisentes ca me diekre dame laine wara dèfle tèrague dilaine diokh khalisse ?? cone dagnie me begone bisnèces dalle ? mais il sont male barais mene dame ame gnianou wadioure ⁉️ baparais same aye même aye waliwou lagniou ta maye teude goudi gnioumaye wane liguèyi yeupe ake dima wane saine aye dieume sène khalise moye djièkh raique touse meunou gniouque ci mene dieu est grand 🤩🤩💖👑💖💖💖💖💖💖💖🥰🥰🌹💐🌹
Yaw thione reference nga monument nga savan nga kou am khelnga masha Allah sa way yeppa am ndiarigne jeureudieuf yalla nalla yalla fay
Dans ce monde et partout, les vrais génies sont incompris. Hélas, c’est ainsi que va le monde. Thione Seck est un génie de la musique. Ki aye texteum rek, sa mélodie et la justesse de sa voix sont impressionnants.
Machalla non vrèment sama,khol daffa toye mère bi machalla lii nioune lako dèfal niou ģñi beuk papa thione ak wa keureume 👏👏✍👈
Pape Thione Seck ..... Un des plus grands monuments de la musique dans le monde.Ayway Pape Thione goudeul fan. Wallahi lo doundou doyoul. 🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏
Thione bodio bodio rek tanyi mom yay buzz bodio yi
Bane monde daga jum dé
Thiey adouna 😭
@@mamskoita5827 dioumoul dh
@@SamsungA-pf9gb yaw sa baye moy bou makk bi
Papa thione Kagne ngaye guéne si mane masou mala guis mai manou mala faté yalla nala yalla yeureum papa thione khadione ngafi basi kanam
❤❤😂😂
Papa thione wallah jtm bien dama beugeu ligueye ak studio bi je suis artiste diapalé ma rek te yalla takh lou nek def nako mes fi bo amoul diapalé do dem teh waye rek la am nguir yalla ma wané sama tallent
Mashallah papa thione yalla nga goude fane 🙏🏽
Papa thione dafa bakh dina la diapalé
@ballago diapalé ko nakk
@@smile-nf4bl merci beaucoup 😊
Thione papis Thione papa Thione tonton thione frère Thione de tous les temps depuis mon enfance jusqu’aujourd’hui, j’écoute et je te suis .
En écoutant j’ai la nostalgie, des frissons et j’ai peur parce que tu rappelle au bon Dieu , tu donnes des conseils de la vie et surtout la nostalgie de la maman que j’ai pas connu qui est parti au delà j’avais 3 ans ...
Quand j’étais au Gabon chaque matin Fari était mon album préféré
Je suis le premier fan de Wally à Paris mais je n’ai jamais parti à ces concerts ni vu mais c’est dans le cœur, je le défends là où il est critiqué.
Longue vie à toi papa Thione Allah est grand ..........
Mang lakOy dialé seugne bi, YalnakO ya'Allah yeureum té diégueul ko xarékO aljana 🙏
Yalla nako yalla yeureum té kharé si aldiana firdawsi thi barké serigne touba papa ya bakh goré va dem amna louma méti lolll
Machallah papa contanneuh nañou sisa jakaar lo bi ak Dj Prince
Il faut reconnaître qu'il a bcp de qualités il est honnête vraiment
Masha Allah ! Papa Thione, sa génération tu fais parti des meilleurs chanteurs, le plus Grand Parolier Masha Allah ! Le Papa de notre Diamant Boy Wally Balago Seck le Chanteur du Peuple Masha Allah ! Yallah nalène Yallah dolé same, doli soutoura bi Amiinne Ya Raby Alaminah ❤❤❤❤❤❤❤👑👑👑👏👏👏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏
guiss nafi ben commentaire mouy nane thione amoul disc dor yew mi commentaire lolou khale nga motakh papa thione amna 4disc dor famile maickl jackson Diokh na niou ko disc dor mome ak presidant abdou Diouf amat na disc dor ak africano son bimou wey sey amat na disc dor ak rappeur france bobou mogui toudou diziz la pest ak benen disc dor ancor ak sovalier ardo merit ak sovalier orde nasional ak sovalier orde merit de lion ak yenen trophe youdoul yoyou ay khale ngan motakh ni rek ngen di def Ba nit ki dh apres ngen nek fi nane Ndessane ak statu youdoul Diekh longue vie a toi papa thione grand parolliers de la musique senegalais
Linga wakhon dh amna tay 😢😢
Salut papa thione ça chanson bi dafma touchée yaye yaye kénnele 🙏
Non senegal mo beuri seytane lane mofi indi wakhou youssou ndour bayilen seytane way senegalais yi seytane yoboule ken aldiana delen defar te bayi nafek longue vie a toi papa thione
Ay saytané you MAK niou beuri senegal
J'aime bien ce monsieur dj prince🎤 papa thione kène démoul guadéss jàmm ci tout le monde 🇸🇳🌏
Man dal pape thione la beugeu point..🥰❤❤
Machalla sunu pape bi ya riche deh laf thiate
Il a vraiment de la classe dj prince, zero faute machaala
Y'a des gens qui t'aiment mais aussi d'autres te détestent c'est évident et tu sais pourquoi ils te détestent parce que t'es honnête mais il faut prendre l'exemple de Sidi Lamine Niasse c'est après sa mort que les Sénégalais se sont rendus compte qu'il était un homme honnête véridique soit toujours toi même papa Thione
En générale si t trop véridique tu resteras tjr un éternel incompris
Ndeyssane diaalé na leu ko
@@maimounandiaye9391 merci beaucoup n'est pas guisga lima wakhone mo âme les mêmes témoignage véridique
Au moins tu l'as témoigné vivant li Allah beugue. Demako lire avec des larmes beu legui décès bi defma diaap
Wayé yalnako Allah Diegual mayko Aldiana si Barké Mohamed ( Psl)
Deugue lou wattal limouy wah sah yi si biir souff😭😭😭😭😭😭
@@ndeyenogayedieng5660 swwsfaqw
Walahi pape thione me manque tellement 😭😭😭que dieu l'accueille aux paradis 😭😭😭😭
Vraiment thione seck kou meun weuy leu ..mai youssou ndour kokou leu kén khamoul loumou donn ..bur yallay dogual.non kokou lénéne leu ❤👈
Incredible quel talent, Thione qu, Allah t, accueille au paradis Firdawsi 🙏🙏❤️
Alahouma amine
Ndeysane papa thione yalla nala yalla yeureum té kharé la adiana 😭😭😭
Adouna dé guisouma koulasi dakeu way weurseuk Kay nite meune nala ko eupou mai boudé waye rék yasi meune
Foufffff sakh motakh yalla faye nako wally
Papa Thione forever machahalah ! Nitou valeurs, longue vie en bonne santé.
Bonjour tonton thione j'aimerais te rencontrer j'écoute tes anciens musiques de l'année 80 ??? j'adore longue vie à toi santé à toi 💖💖❤️❤️❤️❤️❤️ santé à ta familles
Mashalla le meilleur chanteur au monde surtout au Sénégal t es un grand Monument de référence do moromou beneu weuy kate fi si Sénégal on a la chance de t avoir ici au Sénégal je tm fort
" A telle enseigne que" Nékh nala Papa Thione. Temps yi mome dangako dieule rék meno wakh bamou diékh té dougalokassi😄😄
Sinon j'adore ta musique. De part les thèmes abordés, elle est très instructive et trés utile. Waay nga lépp machallah
Machaallahh papa thione si personnalité bi
Un éternel incompris mais jtestime bco notre papa thione national
longue vie a vous le grand thione seck .le plus grand parolier du monde ..
🙏🙏🙏🙏👍👍☝️☝️🤲🤲🤲👏👏👏👏💖💖💖💖💖💖💖💖💖👌👌👌👌
❤❤❤❤❤❤❤❤
@@astoufall7967 ..,
@@astoufall7967 ,..
Tonton Thione machallah et longue vie Penda Niang de Nouakchott
Walaye thione mo takhe ma beugué wally
J'ai perdu😭
J'ai perdu😭
Papa Thione repose en paix
Nioun nieup nio niake nagnko nianal yalla yeureumko kharéko aldiana mayeniou kholou mougn
Kebe niougua borom baye bou baakh yalla na khippeh aldiana
Ndeysan il était tellement intéressant geume yalla. Yalla na aldiana di sa keur seck
Papa thione yalla n'a yalla goudeul sa fan
MashAllah papa thoine "dictionary" la c music senegalese
Meilleur chanteur de sa generation
Thione, un vrai talent avec mon ami prince!
Quelle belle interview très très important bonne continuation et longue vie Thione Seck
Personne ne conteste le talent de youssou NDour.il ne faut pas déplacer le débat. Il s'agit du clan de Youssou le politique qui concentre beaucoup de pouvoir entre ses mains. C'est vrai ce que dit Thione Seck. En un mot on adore le chanteur, on déteste le politicien. On ne peut pas être bon partout.
Ah kou bakh mach Allah laf mon FRÈRE digne humble et genereux un grand HOMME Travailleur Dj prince
Ndeysane vraiment Emissions rafet na dawna yaram yalna yalla gereum ko xareko Aldjiana
Longue vie bcp d bonheur familial à youssou, à l'ensemble des artist et à toi papa thione amin. U es une légende !
Machallah papa Thione longue vie à toi. Maa la bëgg piir yaak sa njaboot Yal na leen Yalla samm aar leen yiir leen.
Salam ! Machallah !! grand Thione ! Un monument de la poésie philosophique.
Un an jour pour jour que notre Balago nous a quitté. Qu'Allah t'accueille dans son paradis. On pense toujours à toi .On prie toujours pour toi.
Le Grand Parolier de la musique senegalaise ❤
Thione lolou mo nékone walou garmi3 yi demb fonk sen caddu!
Mashallah papa Thione we love you Gambian people's
Dama beugue pape Thione ♥️ bilahi walahi kan je le regarde parler g des frissons
Sama pape dji démena 🤲🤲🤲🤲
Repose en paix Papa Thione Balago Seck le grand parolier s'en est allé.Yalla nako Seydina Mohamed téru ci Aldiana firdawsi aduna kéne deuku fi niit ku manu la won machallah 🙏🙏😭😭😭😭❤
Bilayi machalla papa thione repose en paix
Macha halla Nice papa thione♥️
Belen djiguel , soumakoy degglou damay xalat sama bopp walleu xalat souma niakone sama meilleur ami , motax dama beug mon meilleur ami > beugouma adouna bett ma , je préfère ndieuk ko dem , ndakh je ne peux pas vivre sans mon meilleur ami Papytö Jiiaay . De la part de ton frère NdiaaX
Beautiful love it you guys make my day wassallame 😇😎😎
Version salsa bii la degg ci fin bi thiou leu🥰 na gaaw guéneu
Yalla yalla yok diame ak weur ak tou les musiciens amine
Merci dj prince 🤴 thione est un très grand artiste, kéne douko bollé ak son frère youssou ndour un très grand artiste lui aussi
Thioune yalla nala yalla sambou I'm very happy for you
Thione wakham yeep garouwalela
Ya guiss lolu waye mane guissouma lolou
@@assanedeguenekhul6190 kham nane tai rush nga boyi wakh si net ko khamul wakhal lou bakh 😭😭
Thione aka deugou wa Rts diko interview mounilén bou ndieuk dankodone défavorisée
Papa Thione est parti 😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭
Repose en paix #PapaThione
Ndeysane! Que Dieu ait pitié de son âme et que firdawsi soit sa demeire éternelle. Khadiatonegua fi thione
Thione Deck Mandela soukeyna Diouf Marseille sama dôme soumako mérée sakh sa woye Bibou lamaye envoûter sama yaye
Animateur you ndaw yi xool len ci prince...il est posé, correct et puis les questions sont bien posées...
le grand parolier de la musique sénégalaise machallah
Paix à son âme pp thione repose à firdawhs notre pp 🤲😭😭
I love the interview
Diarama sama Turando,le grand homme humble,sociable et surtout très bon exemple.
ℹ️🇸🇳✅✊🏾✌🏾
Album ORIENTAL...Au TOP❤️🙏🏽
Mon pére yallah na aldjiana donne sa keur
Dj prince plein de CLASS!!!
Yalnala yalla yeureum te kharé la adiana ak mbolem dioulit yi djitou 🙏🏽
papa ckou bakh fawou mou am nonne tè yaw du gan am adiana taye ak soubeu inchala ❣️
Meilleur chanteur de sa generation
Machallah papa thione bayou wally Seck le chanteur du peuple 💓
Longue vie a toi papa thione grand parolliers de la musique senegalais
Alahou Akhbar, Thione taguona bou yagueu, neyssane 😪
Li ame na solo trope
Machallah papa thione nii la
DJ prince vous êtes très pertinent vous savez comment pose des questions.
Tu es partie comme ça ?qui te l'aurais dit que tu vivras juste deux mois aprés ooooh mon dieu il est unique🙏🏼Adjana Firdaws🙏🏼🙏🏼
Pour moi les 2 meilleur álbum diaga et appartaille
Mashaallah papa Thione Seck i love so much 💓🙏🙏
Thione tu me manques, merci Prince
Machalla Amna solo
Yalla rék mo mane li 😭😭😭😭
Pape thione repose en paix que firdaws soit sa demeure éternelle Amine
Yalna lko yalla yeureum mais kpu Dee baayi mbebeet
ta liguéye waye yepe gniou guie caye doundou parceque ça me aye kharitou Sénégales gniome liguéye tasse ça seuye ndakh igniane taique ta na ne aye domou dioulite lagniou ndakh comme gniome praisentes ca me diekre dame laine wara dèfle tèrague dilaine diokh khalisse ?? cone dagnie me begone bisnèces dalle ? mais il sont male barais mene dame ame gnianou wadioure ⁉️ baparais same aye même aye waliwou lagniou ta maye teude goudi gnioumaye wane liguèyi yeupe ake dima wane saine aye dieume sène khalise moye djièkh raique touse meunou gniouque ci mene dieu est grand 🤩🤩💖👑💖💖💖💖💖💖💖🥰🥰🌹💐🌹
YALLA Borom bii yeureum leu
Yalanala yala same, moussal la si Pèkhè None, ak sa Famille, diam si yaw
Papa thione machalla longue vie
mâcha alha yag fi loll papa ❣️
Paix à son âme papa 🙏🙏🤲🤲😭😭
Thieye mon papa doundal wayli wayli nga
Papa thione is a legend super star
Macha alla prince tu es très fort
Ndeysane yalla na khipé adiana
Papa Thione je vous admire beaucoup pour votre franc parlé et n'apprécie pas cela c'est qu'ils ne sont pas véridique
Numéro de téléphone svp dj prince
Yalna aldiana firdaosi di sa keur
Ndeysane thione ak wally