Voilà un monsieur dont l'image a été Terni. Un grand incompris de part son étique,sa morale bref un homme de vertu. Que DIEU l'accueille dans son PARADIS AMINE
Khamouma kane dh wayé mane Diop yalla rk lay sédéle limay wakh moy que ni papa thione fimou tollou si sama xol ak beug bimako beuguéwonne yalla rk moko Kham may nianne yalla rk euleuk ma am sokhna ba am so dom bou goor toudéko papa thione c’est l’un de mes plus grands rêves repose en paix papa ❤️❤️❤️❤️❤️🙏
Les gens qui commentés des négatives vous allez vous juger devant lui bayiléne wakh si nite lou bonne so beugué nite wakhal si môme lou bakh soko beuguoul ngua mendou papa tione yalla ngua khipé aldiana didiaye seydina Mouhammad psl
Merci tout cet méchanceté si nite koula defoul dara yomal khiyam niofa nara tardel souniou bop diamono bi mandou manqué nafi trop yor sa pass 100f lakhou sa guinaw téléphone di wakh loula nekh si nite tei dara worou lassi Dieu est le plus grand des juges naniou mandou si diamou yallah yi maintenant il peut reposer en paix 🙏🏽
Walahi werna dom adama niko yala soutouralé mou lank ni d'où soutoural morom si ay soss aki Fenn, walahi papa thione Sama kadou dou masa changer si môme mouy bakh gui âme dîné woyoff
C’est l’une des meilleures émissions papa thione Seck Yalla gu khipee aldiana firdaw s’y wally seck le chanteur du peule diamm si ioe frère et ta famille
Dama wathie Bathie commentaire yi thie souuf, et j’ai vu gniko done saga, diko takhal ndeysane, et j c k c’est ces même personne qui reviennent wala di posté thie sén statut diko dioy😔 adouna nguini c ça les sénégalais, hypocrite fiiiii la fék Mbakh😔😔 yalna niou yala sopi, niou tapé khol yiii
Guindi sagua si internetbi di sagua bijou guone ak papa tion lakatou sen pass bou 100f di sagua sen moromou bay ay nityou tekiwoul dara di sagua ,nit day am yarr boufeker maguini fit guay maguini bount 2stv saguaka direct bijou mer di sagua rek
bijoux tu n est pas une pierre précieuse tu n est pas a la hauteur de ce que tu prétends etre nous croyons au coran et a la sunna et au imaaaaaaams que tu le veuilles ou non
Non bijoux méré nako trop ! Li d’où confrontation, c’est une émission pour redorer le blouson à Thione. Merci ma big taf neutre et professionnel. Nice job
Bilaye kou tede si lalou soukourate digua khamni yalla rék moye Boure alalou adouna yaroule dara dakh doula tope kone na dieux bi rafét dakh moye bénéfice euleuk
@@championdafrique8889 dele moytou togne ko khamoul tes domou adama dafa wara ame respes si moromame khamga manonala wakh louma nèkhe mais nono moytoul di togne
li dou confrontation sa se voit que wally seck est le patron de bijou car les questions qu'elle posent a thione sont differents par rapport aux autres invitès. on dirait que bijou a peur de thione
@@yayependalam2720 est tu payée par Bijoux. Tu prends sa défense partout. Ça c'est UA-cam tu ne peux pas toujours te prendre la tête avec ces choses de critiques. Toi même tu connais les sénégalais leurs opinions sur les RS.
mame awa bousso mbaye je n'ai rien contre bijoux ni thione seck jai l'habitude de suivre confrontation mais c'est la premiere fois que je vois bijou poser ces genre de questions
@@ibrahimandiaye5563 yalla dé bimouy bine bijou taguoula yalla bime lay bine taguoule bijou yalla rekk ka khame kou bone ak kou mouye allack wasalme☝☝☝☝☝☝☝☝☝☝☝☝
@@deuguerekkmoyemoudiou5839 yaw say tanénga louné feng kén douco diékh bijou boubakhone dou toudou guéni imam yi ak moukhadam yi kénén kouko wakh magnanal ko yalla allak co
Yén ngigne wakh lou bone ci nite ko khama loute dara di wakh ci mome lou ngiaw yén ngiy wakhal nite lou ngiaw bayi lén khél ci ngiati fani bamél nite loumou bone bone lo wakh ci mome lou ngiaw dieul nangne salou bakh diokh ko dieul lou bonam diokhla léguéne di wakh sét lénssi yalla bakhna
Tanor que le bon dieu l'accueil dans son paradis les secrets qu'il détenait il n'osait pas les révéler parce-que il était dedans il se mouillait lui même
Voilà un monsieur dont l'image a été Terni.
Un grand incompris de part son étique,sa morale bref un homme de vertu.
Que DIEU l'accueille dans son PARADIS
AMINE
Gning wali merci
Khamouma kane dh wayé mane Diop yalla rk lay sédéle limay wakh moy que ni papa thione fimou tollou si sama xol ak beug bimako beuguéwonne yalla rk moko Kham may nianne yalla rk euleuk ma am sokhna ba am so dom bou goor toudéko papa thione c’est l’un de mes plus grands rêves repose en paix papa ❤️❤️❤️❤️❤️🙏
Yalna lako Yalla defaral
Malako gueuneu beugue bilahi walahi talahi
J’adore Thione Seck un Homme de principe et de conviction
J’aime Messieur Seck il est très honnête!
Les gens qui commentés des négatives vous allez vous juger devant lui bayiléne wakh si nite lou bonne so beugué nite wakhal si môme lou bakh soko beuguoul ngua mendou papa tione yalla ngua khipé aldiana didiaye seydina Mouhammad psl
Merci beaucoup way
Merci tout cet méchanceté si nite koula defoul dara yomal khiyam niofa nara tardel souniou bop diamono bi mandou manqué nafi trop yor sa pass 100f lakhou sa guinaw téléphone di wakh loula nekh si nite tei dara worou lassi Dieu est le plus grand des juges naniou mandou si diamou yallah yi maintenant il peut reposer en paix 🙏🏽
Walahi werna dom adama niko yala soutouralé mou lank ni d'où soutoural morom si ay soss aki Fenn, walahi papa thione Sama kadou dou masa changer si môme mouy bakh gui âme dîné woyoff
Qu’est-ce que je suis d’accord avec papa THIONE il a raison il veut s’arrêter en beauté. Je t’aime papa THIONE paix à ton âme. Amen 🙏🏽
Ndeyssane Repose en paix
Qu'Allah t'accueille dans son Paradis Firdawssi et te pardonne tous tes péchés 🤲
Amine Ya Rabi
@@Myrm85 0
0
Amine yarabi
Ndeyssane 😭😭😭😭😭😭😭😭😭Papà thione bilahi yallah warena labayi gua yeguelek yallah Nala yalla yeureume Kharela aldiana firedawsi😭😭😭😭😭🙏🙏
Ndeyesane nèfèna Ba sonne que la terre Luis lègère Amine
C’est l’une des meilleures émissions papa thione Seck Yalla gu khipee aldiana firdaw s’y wally seck le chanteur du peule diamm si ioe frère et ta famille
Dénla toogne gniari yone wayè lou âme yalla fèkèna 😭😭😭😭😭
Mon seul et unique Chanteur, yalna khipé Aldiana 🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏
Vraiment il est plein d'humour Pape Thione longue vie à toi té nga diéggeulnou ak kéep koula mass togne té khamoula khamoko💓
Ndeye sane Wakhi gorr deug ak kou humble
Kou bakh démena yalla nagua khipé aldiana 🙏🙏
Kouma météni papa thione Seck amatoul si adouna 😭😭😭yalla na firdawsi néke keureum ba faw
Reposez vous en paix papa Thione qu'Allah vous accueille dans son paradis éternel alahuma enmine yarabih.
Que firdaws soit votre demeure inshallah.
Mane papa thione nite kou bakhe lamaye diokhe longue vie
Ki niit kubax deeg la
Papa Thione Yalna khipeh Jannatoul Firdawsi Amine Ya Rabi 🙏🏾🙏🏾🙏🏾
Mon artiste, mon père , mon référence, mon idole mon........
Longue vie à toi Papa Thione SECK
Même moi aussi
Ndeysan papá thione ko oyof la wone bilahi dafma fatali Sama papa yalna lene yala yeureume kharelene aldianatoul firdawsi 🤲🤲🤲🤲😭😭😭
Thieuy souniou baye thione SECK yalla na khipé dianatoul makhwa thi firdawsi amiiiiiiiiiiiine 😭😭😭😭😭😭😭😭😭
Amiiiiiiiiiiiiiiin
Le Senegal a démontré que Thione Seck(repose en paix) est un Grand Homme. Que ton legs soit assuré !
Papa thione yalla nala yalla yeureum kharé lene aldianay firdawsi yaw ak momy seck
Un homme pétri de valeurs yàlla yalla yessal yeurmandeh si mome
Yalla na nga khipé Aldiana Firdawsi AMINE
Slt a tout les amies bayilene di commentaires di saga mandou dal bakhena wakhe bou rafete yombouna the beuri n'a tiyabou
Es ce que réellement Thione est décédé 😭😭😭😭😭bataye je le pleure aduna daal sou dara
Dème na cimetière Yoff y’a 3 mois guiss tombeau bi ndeyssane
Ndeyssane que la terre lui soit légère
Bilahi
Adina dou dara
PAPE THIONE SECK KOU BAKH LA IL EST TRÈS HONNÊTE ET COURAGEUX
Aka yiw. Qu'il repose dans la paix des gens justes.
Amiine yarrabil alamin
vraiment papa thione est un guide il n'était pas n'importe qui qu'allah lui pardonne
Senegalais nite kou deugou rek gnou sikeul la pape thione que son âme se repose en paix🤲
Yalna khipe aldiana barke seydina mouhamed saws 🙏🙏😭😭😭
Papa thione que dieu l'accueil dans son paradis inchala si baké sedina mohammed saw c'est un homme honnête et digne machala
Pape thione souma don yaw douma wakhati si afèrou kgalisbi yalla sètal nala machalla doundel 111ga
ana fans pappa Seck yi
Qu’Allah soubhana t’accueille ds son saint paradis firdawsi inshaallah rabi
Amine ya rabi
Bijoux je te connais pas mais tu me plais beaucoup vraiment ! Merci.
Kou sagua sa morom baye sa Papa ngua sagua motakh aye boy you trokh beuri Senegal
Bilahi wakhal dh
Dama wathie Bathie commentaire yi thie souuf, et j’ai vu gniko done saga, diko takhal ndeysane, et j c k c’est ces même personne qui reviennent wala di posté thie sén statut diko dioy😔 adouna nguini c ça les sénégalais, hypocrite fiiiii la fék Mbakh😔😔 yalna niou yala sopi, niou tapé khol yiii
Bilay papa thione woygua lep bagnale boko diokhe bene khalè
Guindi sagua si internetbi di sagua bijou guone ak papa tion lakatou sen pass bou 100f di sagua sen moromou bay ay nityou tekiwoul dara di sagua ,nit day am yarr boufeker maguini fit guay maguini bount 2stv saguaka direct bijou mer di sagua rek
اللهم اغفر له وارحمه واسكنه فسيح الجنة الفردوس الأعلى انشاء الله امين يارب العالمين ببركةخادم الرسول الله
Billah ndayesane pap a a ka nékh hone wakh tane mé yalla na ko yalla yuerueme si barké khasidayi amine
Grand thione yalla nako sounou borom yeureum te yeukheniou,ci barke seydina Mouhamad PSL
Papa Thione mangui diegoulou waye amal discretion touti. Sa yoo toude projet bii reek niou fekheel leu wala niou fekheel sa Dome.
mo😂😂😂
Ki va pirater ou entraver ce pseudo projet à la con
Machallah machallah Nice na torpo papà thione 👍🏿👍🏿👏🏼👏🏼👏🏼👏🏼
Ndaysane papa thione nak bou wakh dji wésso nitou késsé bilay ki a remarqué
😢😢 Sénégal barina nafek ya des hommes irresponsable judtice senegal mom warna di seteu yalla touti sur son travail
Niari domaram
ne croyez pas que les gens ont regardé la vidéo pour le plaisir
Deug piir
Merci
Viens te relire à l’instant précis gua khol ndakh adouna diarna wakh lou niaw sa nawlé
Papa yalla nakou Yalla yeuram Kharéko aldiana amine 😭🤲😭🤲
Ndeyssan aka mougne deg.lounekk yalna Aldiana Firdawssi di keureum guou moudjou
Que firdawsi soit ta demeure éternelle papa thione 💔💔💔🙏🏾🙏🏾🙏🏾
Bouma khalaté dé takh douma wakh moukk lou gnaw ci niit. Yalla réck mo kham kou bakh. Yallana Aldiana doôn sa deukouwaay
Bijou ndeysane dafa beug papa thione kom mann nimalo beugué yala yeureum ko yobouko firdawsi amiiiiiiiin ya rabi
Yalanako yala yeurame bark yonenetibi psl walahi ndeysanne
Bilay papa thione so degue aye wakhame nga khamni nit kou sincere la. Bilay ndogal dou wess papa
Papa thione machala kéne dou yaw laf thiat si yaw ak sa fami yalla na yalla motali lép inchala
Je ls tjrs aimez yalna yallah aréla aldiana
bijoux tu n est pas une pierre précieuse tu n est pas a la hauteur de ce que tu prétends etre nous croyons au coran et a la sunna et au imaaaaaaams que tu le veuilles ou non
Paix à son âme. Que firdaws soit sa demeure éternelle
Que son âme repose en paix , cette interview nous l'a fait connaître
Big taf becarful with Big deck fatabarakalaxou 🙏🏿💯
Meilleur chanteur de sa generation
Non bijoux méré nako trop ! Li d’où confrontation, c’est une émission pour redorer le blouson à Thione. Merci ma big taf neutre et professionnel. Nice job
Did you just say my big taf? No, she is your big pork shop. You and Bijou can go to hell.
Longue vie à Papa thione doundeul ilimix
nonnnnnnnnn bijou ngoné yaguiii dokgua khamniiii niiit yeuppay dioum?? gni gua donnne invité avant dou gnou ay niitt?? yaw hypocrite bou bonnn gue
Respé
Doul amal respé
@@mbenguesouleymane7419 yaw Kane guay wakhal
@@ndiagaauro673 wakhou mala ki di dépasser Papa thione ak bijou lay wakhal
@@ndamalcadiorsonko5598 yaw dagua tardé motakh séne adouna bép vous resté méme sur place. Pace que déguéne sokhor
Mashallah Pappa Thione 🙏🙏🙏🙏🙏
Merde yow
Yallah moye kéne thione da gueme yallah dieu le accueil aux paradis
Repose en paix papa thione. Nitte kou deugou. Ame diné. Correct. Sage. Yala na khippé firdaws
Papa thione yalnako Yalla yeuram
Repose en paix;Qu’Allah;t’accuelle dans son Paradis
Réponse en paix Papa Thione😭😭
Mercie beaucoup 👏👏👏bijou
Yalla nako yalla kharéko aljana papa Thione
J'adore thione tu as pleins de valeurs
RIP Papa Thione
❤ Repose en Paix Papa
Bilaye kou tede si lalou soukourate digua khamni yalla rék moye Boure alalou adouna yaroule dara dakh doula tope kone na dieux bi rafét dakh moye bénéfice euleuk
nianale ko yalla kharèko aldiana firdawsi
فال سبحانه وتعالى :(أفحسبتم أنما خلقناكم عبثا و أنكم إلينا لا ترجعون).: Yalla nèna dangène yaakar ni damalèna binde nguir fo rek té doolène délousi si mane.
Bakhna rek yawmal hiyaam aka diara bayy xel, wayé sén lep Alalou aduna rek😢
L'intitulé de l’émission sonne comme un conflit d'intérêt...
Bijou NGoné s'est comportée comme la porte-parole la famille Ballago, ces derniers jours.
Longue vie a toi papa thione grand prolliers de la musique senegal
2ans apes un legende rest in peace papa thionr💔🙏🕊
Ndaysan toujours dans nos cœurs
bijou tu es l'incohérence personnifiée...ragalal kila bindeu mais pas kilay faye
Doule marame
@@edupretorarosenegal1474 khana waa brazil nga😂😂
@@kanemomar6292 😄😄😄😄😄😄😄😄😄
Gni ay domėralaniou
Cool
No mane papa thione lay weur reynama fara fara 😂😂😂
Sama papaye bop goudeul fane yalla bayilafi basi kaname bilaye bijou dina bakh
Amina Diallo diapal si sa baye mo geune!!
@@championdafrique8889 dele moytou togne ko khamoul tes domou adama dafa wara ame respes si moromame khamga manonala wakh louma nèkhe mais nono moytoul di togne
Ndeyssane paix á son âme ,c'est vraiment triste
Merci papa thione deugue rek guay wakh te sénégalais yi beugouniou deg deugue
Père thione tts le Sénégal vs remerci tu NS as donné Wally notre fierté
Mane dé guinémasi
Man de koumassi bolle cadoulngama hak
li dou confrontation sa se voit que wally seck est le patron de bijou car les questions qu'elle posent a thione sont differents par rapport aux autres invitès. on dirait que bijou a peur de thione
Mais fait ce qu elle veut elle s en bal
@@yayependalam2720 est tu payée par Bijoux. Tu prends sa défense partout. Ça c'est UA-cam tu ne peux pas toujours te prendre la tête avec ces choses de critiques. Toi même tu connais les sénégalais leurs opinions sur les RS.
mame awa bousso mbaye je n'ai rien contre bijoux ni thione seck jai l'habitude de suivre confrontation mais c'est la premiere fois que je vois bijou poser ces genre de questions
Binetti tanto bijou si keurguila.mais la realite et Ke Pape thion raconte des conneries.😃
Vous etes des embesil
Longue vie à toi papa thione
Ziarr na le cheikh avocat wally 😂😂😂
Repose en paix papa 😭😭🙏🤲🤲
thione yènn amoulènn louguèndi vakhati thi rewmi ay nafekh nguèn yaw bijou limounek moudiouk diamono motakh ga am fitou saga ay imame
Ki di domeram bijou mélni hippopotame bou jiguéne déko mouy néh big Taf bayil papa thione
Pata bi bouken diar si toureum nianal lén ko bala déé yalla wane ko bopame si adouna domouharam
@@ibrahimandiaye5563 yalla dé bimouy bine bijou taguoula yalla bime lay bine taguoule bijou yalla rekk ka khame kou bone ak kou mouye allack wasalme☝☝☝☝☝☝☝☝☝☝☝☝
@@deuguerekkmoyemoudiou5839 yaw say tanénga louné feng kén douco diékh bijou boubakhone dou toudou guéni imam yi ak moukhadam yi kénén kouko wakh magnanal ko yalla allak co
@@ibrahimandiaye5563 dieureudoeufffff
Rip pap thione yallah nala yallah yeureum ci barké yoninté bi
Un homme de ♥️✔️
Papa thione laf thitt mashallah...I love you always ♥️💞💕👏👏👌💪🖕
Merci
Senegalais MO sokhore ba raw guana
Big Taf machalaaa il est très bien ! Bijou est très belle machalaaa
Yén ngigne wakh lou bone ci nite ko khama loute dara di wakh ci mome lou ngiaw yén ngiy wakhal nite lou ngiaw bayi lén khél ci ngiati fani bamél nite loumou bone bone lo wakh ci mome lou ngiaw dieul nangne salou bakh diokh ko dieul lou bonam diokhla léguéne di wakh sét lénssi yalla bakhna
Walahi wakhi deug sa wakh j d Tay mo rouslo niou Bari bim démé niou sogko kham
Tanor que le bon dieu l'accueil dans son paradis les secrets qu'il détenait il n'osait pas les révéler parce-que il était dedans il se mouillait lui même
Pape thione je t'adoreeeeeeeeeee
Que firdawsi soit sa demeure éternelle