NDONGO LO EN LIVE Biir RTS1

Поділитися
Вставка
  • Опубліковано 7 січ 2025

КОМЕНТАРІ • 428

  • @BEUGNDONGOTVInternational
    @BEUGNDONGOTVInternational  Рік тому +36

    TOUTS LES DIMANCHE DE 19 HEURES JUSQUA 21HEURES AK LANIMATEUR DU PEUPLE DJ BEUG NDONGO SUR LA RADIO LERAL FM 96.1 DAKAR DANS EMISSION "NDONGO LO BATAYE" SPECIAL NDONGO LO RETENEZ BIEN RENDEZ VOUS..
    Pour les sponsoring de l'émission Contacter :774213974

  • @bassiroupene5347
    @bassiroupene5347 Рік тому +6

    Yalna Yalla yassal yeurmandem si sa kaw Ndongo Niang

  • @ndenebadiane2610
    @ndenebadiane2610 3 роки тому +11

    Kou beugeu sa yaye wakhal li dafa nekhe bilaye

  • @amdykosso9902
    @amdykosso9902 2 роки тому +32

    Incontestablement le meilleur chanteur de tous les temps✍️🇸🇳 Yalla na sunu Borom guëna yëSsalate yeurmandé ci kawaam.. Ndongo Lo tu restera à jamais gravé dans nos cœurs❤️🔐

  • @moustaphafaye8837
    @moustaphafaye8837 10 місяців тому +4

    Ndongo lô que la terre luit soit légére amine

  • @ousseynoudieye8336
    @ousseynoudieye8336 4 роки тому +77

    Bilahi walahi talahi ndongo lô était unique dans son genre Qu'Allah l'accueil dans son paradis céleste

  • @mbayeludovicbambiste593
    @mbayeludovicbambiste593 4 роки тому +8

    Ndongo lo duniou la mesa faté yalla na janatoul firdawsi done sa dekou way barki seydina Mouhamed (psl)

  • @falloubandadiagne8365
    @falloubandadiagne8365 Рік тому +4

    Sama artiste a vies je suis fiére de façon que tu fesais artisticment tay soumlay def benen leval lay nék

  • @mbayegueye5234
    @mbayegueye5234 Рік тому +4

    Yalla na yalla yésal yeureumandé si cawam nit kou bakh la ndongo lo

  • @ibrahimcisse8263
    @ibrahimcisse8263 Рік тому +9

    C'est l'une de artiste que je écoute jusqu'à présent c'est mon chanteur préféré que le bon Dieu lui acceuil dans son paradis éternel

  • @alhamdoulilah5448
    @alhamdoulilah5448 4 роки тому +23

    Mane déh nimay djoyé ndongo ces temps ci Dax diam leu😭 alors bamouy guén adouna j'avais k 6ans mai tay djiy lay xol ay documentaire ramm bilahi deké nitt gueunouko wone😭 k l firdawssi soit ta demeure éternelle Ngongo 🙏

  • @khadimcisse7687
    @khadimcisse7687 4 роки тому +50

    Thiey ndongo yalla nako yalla térou alldiana firdawsi barke serigne fallou

  • @alitounkara990
    @alitounkara990 4 роки тому +6

    thiey yalla ki tek Li ya beug ndongo wala ma beige ndongo d'où ma deglou ben musique boudoul ndongo yalla na ko yalla yeureum xaréko aldiana amin y'a rabi

  • @modousylla7978
    @modousylla7978 2 роки тому +6

    Mon artiste préféré walahi yalla nalla yalla yereum si barkep seydina Mouhamed

  • @BEUGNDONGOTVInternational
    @BEUGNDONGOTVInternational  4 роки тому +41

    Ces le pere de touts les Artistes

  • @falloulo8430
    @falloulo8430 3 роки тому +10

    Qui est là en 2021 blh je l'aime yalla nako yalla yeureumm si barkè serigne fallou

  • @anitadiop3231
    @anitadiop3231 4 роки тому +65

    Ki es la en 2020

  • @ballajallais9196
    @ballajallais9196 Рік тому +13

    Je me rappelle souvent on était à xewel bi avec sont grand boubou bleus ndongo lô yagui tii xoll yi xell yi❤😢 yalla n’a borom bi geureum

  • @karimba7117
    @karimba7117 2 роки тому +14

    le meilleur sur scène une vie courte le parolier nous a quitté très tôt qu'il repose en paix

  • @cheikhmorgueye
    @cheikhmorgueye Рік тому +14

    Ndeysann Ndongo lo binga gagno la weuyy tounouranké senegal 😢😢😢

  • @Seck-j6i
    @Seck-j6i 11 місяців тому +3

    Un des meilleurs de sa generation dommage qu'il soit parti tot
    Qu'allah lui accorde sa misericorde

  • @senegalrek2579
    @senegalrek2579 4 роки тому +14

    Wallahi deug rek mo nekh yallah binga dem lay doga kham ndeke ndanane deug mo dem bobou balegi waykat fesoul Sam beut ndakh yaw linga fi bayi billahi je t’aime trop ndongo ❤️❤️❤️❤️❤️

    • @mamyseck8988
      @mamyseck8988 3 роки тому

      Wallahi dou morom béne way kat

  • @TallaSarr-n5s
    @TallaSarr-n5s 3 місяці тому +5

    Qui est la en 2024 pour l'educateur❤

  • @adamacamara2817
    @adamacamara2817 4 роки тому +80

    Tu es vivant. Tu ne parles pas mais tu es vivant Tu ne bouges pas mais tu es vivant

  • @talibecheikh7367
    @talibecheikh7367 4 роки тому +23

    Repose en paix Ndongo mou Sérigne Fallou que firdawsi soit ta deumeur éternel amine tu restera toujours dans nos cœurs ❤

    • @diopfaya3471
      @diopfaya3471 4 роки тому +1

      Amine , on prie toujours pour le repos de son âme.

  • @fati9405
    @fati9405 2 роки тому +9

    Kou mel.ni ndongo dotoufi am Bilae kenn la Wonn meilleur pour tous les temps yalla nako yalla yereum. Kharei ko aldiana 😢❤️❤️❤️❤️❤️❤️

  • @mamounendiaye2767
    @mamounendiaye2767 4 роки тому +58

    😭😭😭😭manouma teyé samay rangogn 😭😭 khamou mako douma diglou musique mais wallahi haziim dama ko beugue bamou diaxal ma

  • @khadimdiop9244
    @khadimdiop9244 3 роки тому +7

    J’ai toujours pleurer 😭 par ce que destin wou ndongo lo dafma diakhaal li Yallah rekako Sagñe

    • @oulimataboh8205
      @oulimataboh8205 3 роки тому +1

      Diaxaloula ba rawma pour mane rek may khalatè ni diaxal nama trop

  • @mouhamedthiamzikroulah1798
    @mouhamedthiamzikroulah1798 4 роки тому +47

    Nooo Ndongo lo d'où nitte , kii soko kholé bu bahh dinga guiss lima wah , Yalna aldiana done keureume

    • @eulaliemainge9701
      @eulaliemainge9701 3 роки тому +1

      Amen Amen Amen Amen Amen qu'il repose en paix !.

    • @gibbiesecka400
      @gibbiesecka400 3 роки тому

      Sas vremant borom bakhla vremant beug Serigne fallou

  • @moustaphagueye9601
    @moustaphagueye9601 3 роки тому +5

    Ndongo lo bou Serigne fallou yalla na nga xippé aldianay firdawsi Amine

  • @FalloualadjiSakho
    @FalloualadjiSakho 6 місяців тому +2

    A 04h 03mn du matin diko sétane ndeysane artiste dou dée bilay yalla na souff owof thi kawam mais il reste le meilleur de sa générstion

  • @ndiagasene4131
    @ndiagasene4131 4 роки тому +4

    meunouma degloti ay way legi bilaye,sa bate rek moma don danel bilaye,yalla yeureum la te khare la aldjiana aminnnn

  • @morbeye2842
    @morbeye2842 3 роки тому +2

    Ki kassè moma meuneu dioylo si musique yale nako yalla yeureum tè diegual ko ay baakaramm you makk ak you ndaw amine

  • @sdn6319
    @sdn6319 4 роки тому +12

    Beug Ndongo lo tv international.
    Ah di bégue si yaw rek déf gua affaire dal. ils demeure toujours ds nos❤️,
    Q firdawssi sw sont dernière demeure amine yarabi. 🤲 si barké Serigne Fallou Mbacke..Serge..🇸🇳❤️🇮🇹🤲🏽🙏🏽🤲🏽

  • @barmouhamadou4255
    @barmouhamadou4255 3 роки тому +5

    Plus talentueux que ndongo n'existe pas yal nako yall yeureum

  • @ndongo110
    @ndongo110 2 роки тому +7

    Thiey ndongo lo il restera toujours dans non coeur

  • @abysall7830
    @abysall7830 3 роки тому +21

    Yallah na souf sedeu si kawam. Repose en paix mon Ndongo

  • @alaingomis7486
    @alaingomis7486 3 роки тому +37

    Qui est la 2022✌?
    Paix à son âme NDONGO LÔ🙏

  • @Mohamedsall844
    @Mohamedsall844 4 роки тому +35

    Ndeysan Ndongo Lo meilleur chanteur du monde

  • @mawlanaambengue2059
    @mawlanaambengue2059 2 роки тому +11

    En si peut de temps weuy leep lifi amone solo mayniuko dem. Il a chanté la VIE "Yaye moy buntu aduna", L'amitié diangal niu luy koloré ak bagna bew (xarite yimu maagandol), dans "dieggou pousso" lim waraté fofu amatul😍😍😍
    Ku lim dioum. Rest in peace Waliw bi.

  • @djilysamb6915
    @djilysamb6915 4 роки тому +25

    Jusqu'à présent yafi nek sama artiste préféré 🙏
    Repose en paix gaïnde 🙏

    • @bombafall2797
      @bombafall2797 2 роки тому +1

      Yalna xipé aldiana firdawsi ndogo machalah wayam dou xéwi bilahi

    • @djilysamb6915
      @djilysamb6915 2 роки тому

      @@bombafall2797 bilahi kaay ndanane leu dhé

  • @alioubocoum77
    @alioubocoum77 2 роки тому +3

    Yallah nako yallah yeureum way ndogo lo 🙏🥹

  • @SoyelJah
    @SoyelJah 7 місяців тому +2

    Paix et repos éternel à ton âme. C'est mon unique chanteur mbalax c'est sans doute le roi du mbalax le meilleur de sa génération

  • @unbiased216
    @unbiased216 3 роки тому +6

    Thiéy ndongo lo toujours mo ngii cii sama khél bi yalnako borom bi yeureum🙏

  • @mamidiouf3550
    @mamidiouf3550 4 роки тому +6

    yalla nanga khippé adiana si barké seydina mouhamed psl ya takh ma guene beugeu serigne falllou mane talibé cheikh bi

  • @omarthioune1249
    @omarthioune1249 4 роки тому +47

    Le meilleur de tous les temps yalnala yalla yereum

  • @abdoulayeciss2596
    @abdoulayeciss2596 4 роки тому +3

    Meilleur de tous les temps ngongo yalla na ko yalla yeureum si barkep borom touba bilahi yay Gouy gou dar khalé yep si yaw lanouy diangué

  • @adamadiene9380
    @adamadiene9380 2 роки тому +4

    Ningay sédalé sama khôl yalle nala ko yalla fay ❤️❤️❤️

  • @bassirounguer7411
    @bassirounguer7411 4 роки тому +14

    Ndaye sane ki diakhalnama dh man guisouma kouko dakha wouy thi adouna ay wakham léup ndiarigne la yalnako yalla yeuram

  • @moussaniang2802
    @moussaniang2802 4 роки тому +17

    Man dama beug NDONGO lo na xawoma lan layé comment xanaa di nianal rék yalla xaréco aljana the barkép seringe touba

  • @SouleymaneCamara-n9e
    @SouleymaneCamara-n9e 8 місяців тому +1

    Thiey ndongo lo noooon yalnako yalla yeureum té diégueul ko kharé ko aldiana firdaw si barker Mohamed sws barker alkhouran ❤

  • @Papa_el_maks
    @Papa_el_maks 4 роки тому +14

    Ki pleure en 2020😭😭😭 yalla na yalla yokou ay lerame

  • @CheikhGayeLo
    @CheikhGayeLo 4 роки тому +5

    Yalla nako yalla yeureum ndonga komana way naturel do force dara

  • @ndenebadiane2610
    @ndenebadiane2610 4 роки тому +12

    Sounou borome ligeune rek laye def ki bou doundon ame na artis yo khame ni dou gniou lek sy musique 100f

  • @laziz127
    @laziz127 4 роки тому +6

    Doumou Adama Sougnou borom dakoy diokh Mission si Adouna mou djité Di Wakh Mou nékh trop mé Aleuk mo takh té parole ma bcoup edée ndongo Rip gnang Ballo 😔

  • @FKZ-NDINDI
    @FKZ-NDINDI 2 роки тому +9

    Qui est là en 2022 le meilleur de tous les temps Ndongo lo Yallah na sa Borome yeureum la diégal la si barkép Serigne Fallou Mbacké

  • @mbayewalo5599
    @mbayewalo5599 4 роки тому +2

    Samay niary way diour yalla na yalla yoki sene lerr thi barques s babacar sy

  • @mouhamadoulamineseyebeugue2741
    @mouhamadoulamineseyebeugue2741 4 роки тому +10

    *_Ndeyesann ndogo yalnako yalla yeureum té khareko aldjana si barkép serigne saliou mbacké wallahi donn masa fattée si Adouna QUE ton âme Repose en paix😢😢😓😓😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭_*

  • @cheikhgueye1006
    @cheikhgueye1006 Місяць тому +1

    Thiéy ndonga sa démgui méty trop mais yalla sou sokhla diam gnak😢

  • @mouhamedmouhamed5457
    @mouhamedmouhamed5457 4 роки тому +4

    Nimou niuy bèguelei yalnako yalla beguelei nonou ndah sorina sougnuy khol

  • @louzvip1943
    @louzvip1943 4 роки тому +15

    Thiay yalle do meuss diouk souniou xell ndongo yalle nale yalle terou si aldjiana firdasi RIP ❤😭😭😭

  • @abrahamsamb9736
    @abrahamsamb9736 3 роки тому +19

    Il restera dans nos cœurs

  • @babacarsakho630
    @babacarsakho630 4 роки тому +7

    Bilahi Beug kontan naniou king of the king the singer of the world

  • @karimgaye4327
    @karimgaye4327 4 роки тому +12

    Ndongo il a un don

  • @thiorojoop4019
    @thiorojoop4019 3 роки тому +5

    Magui imaginé boufi nekone batay
    Yalnala yalla kharé aljanah❤🙏

  • @ibrahimandiaye9292
    @ibrahimandiaye9292 Рік тому +2

    C était avenir de la musique Sénégalais Dieu a voulu ainsi

  • @regalotouba5530
    @regalotouba5530 2 роки тому +3

    Ndaysan douma tayi dii wakh sii mom Yalla nako sa borom yereum ta khare ko aldialna firdaw sii sii barkeb serigne fallou famou Diem Yalla nako gueneul fii mou diougué boude nianou waniour dina topou domm famou neh boo tede nella Wall Yalla nga tassegue baye mben maa gallass😭😭😭

  • @Morbirahim
    @Morbirahim 4 роки тому +8

    Thiey adouna mo doy warr
    Yalanala yalla yeureum xaréla aldjiana

  • @mbayedemba61
    @mbayedemba61 4 роки тому +34

    Il reste toujours dans nos cœurs

  • @SaliouNdao-f6r
    @SaliouNdao-f6r 3 місяці тому

    Tu restra toujours dans notre cœur😭❤️❤️❤️😭

  • @dianeblack_man4306
    @dianeblack_man4306 4 роки тому +15

    Mome rk lay degglo ci music ay leçon rk ❤️🇸🇳😓

  • @salioudiagne6499
    @salioudiagne6499 4 роки тому +6

    Dieuf diou bakh môye sédé brome lou bakh ngafi bayi kena dou dekloul say music ta xolam Séoul. Souma manone rambou yawmal hiyam yaye djitoou al djiana

  • @barapromax2571
    @barapromax2571 2 місяці тому

    En novembre 2024 ba legui damalay deglou vraiment danga meunona way trop , yalla nalla yalla xaré aldjanna ❤

  • @diopndiaye5204
    @diopndiaye5204 4 роки тому +1

    Et la suite svp, yalnaco bour bi xare aldiana firdawsi si barke serigne Fallou

  • @ibrahimaba7519
    @ibrahimaba7519 4 роки тому +6

    Da am lou kènn amoul machalah .2020

  • @AssaneKa-gl4sn
    @AssaneKa-gl4sn 7 місяців тому +1

    Yalla Nako yalla yereum si barki seydina mouhamed SAW ❤

  • @dougoudafrique
    @dougoudafrique 2 роки тому +6

    cette tres belle voix reste toujours dans nos oreilles...

  • @academiefootballmamefallou
    @academiefootballmamefallou 3 роки тому +3

    Le meilleur de génération jtjr

  • @cheikhnacheikhsadboudjeurd8087
    @cheikhnacheikhsadboudjeurd8087 4 роки тому +13

    ki rék moté ma bayi déglou musique billahi

  • @abdoulayebarry4474
    @abdoulayebarry4474 2 роки тому +5

    C'était le meilleur de sa génération

  • @mouhamedndiaye9869
    @mouhamedndiaye9869 4 роки тому +8

    Merci beaucoup à Beugue ndongo Lo c est vraiment cool

  • @cheikhnafall6409
    @cheikhnafall6409 4 роки тому +2

    Machallah yalla n'a la yalla may aldjanay firdawsi

  • @dabangning5883
    @dabangning5883 4 роки тому +13

    Ndongo dougnou meusseu fate billay repose en paix 😭 😭

  • @elhadjimodougaye3483
    @elhadjimodougaye3483 4 роки тому +8

    Yalnala mame fallou takhawou mane el hadji doumala masa faté barké alkhourane 😭😭😭😭😭😭😭

  • @mouhamedmouhamed5457
    @mouhamedmouhamed5457 4 роки тому +8

    Groupe Jaam benne la dou amati weet na niu

  • @mamadouba2025
    @mamadouba2025 4 роки тому +6

    A jamais dans nos cœurs yalla Nala maam fallou Mbackè terrou ❤️🙏

    • @sdn6319
      @sdn6319 3 роки тому +2

      Amine yarabi fréro

  • @fallouthiam7222
    @fallouthiam7222 4 роки тому +5

    Yalla na la yalla yaram mofi gnaka way yaye ,🥰😭

  • @abdoukhadrefall4566
    @abdoukhadrefall4566 Рік тому +1

    Paix à ton ame grand artiste ndongo lo yalla yeureume la xaré la adiana

  • @thiaomame1357
    @thiaomame1357 4 роки тому +1

    Li nekh na tey lo yalla na la yalla yerme

  • @amadougueyestar2emepiste631
    @amadougueyestar2emepiste631 2 роки тому +4

    Le meilleur de tous les temps. Yalla na ko yalla yeureum té xaaré ko Aldiana.

  • @Eladji-sall44
    @Eladji-sall44 4 роки тому +8

    yalla nako yalla yeureume kharéko alediana firdawesi

  • @omarsall5192
    @omarsall5192 2 роки тому +3

    Ndaysaan adouna dou keur thiey🙏🙏yalla yalla na ko yalla yeuram😭😭😭

  • @keurrassoul5810
    @keurrassoul5810 4 роки тому +5

    Bilahi diamano bi la ndongo nékon en bon sante . Rip frere 😢😢😢😢😢

  • @ousmanendongo879
    @ousmanendongo879 3 роки тому +1

    yo Allah yourmo yafomo yo Allah harnoumo alidjana amine yarabi ndongo lo bou serigne saliou❤❤❤aduna welani ndeysane

  • @moussadiallo718
    @moussadiallo718 3 роки тому +19

    Que DIEU l'accueil dans son paradis

  • @seydialiouseck3882
    @seydialiouseck3882 2 роки тому +5

    Thieuy Sma Weuy Kat Bi 😭😭 Ndeysane Meunouma deglou ken koudoul mom Yalla nako yalla yeureum ya rabi😭😭😭

  • @abdoumane7700
    @abdoumane7700 3 роки тому +1

    Ndongo yalla nala yalla yeureume ta kharéla aldiana

  • @mouhamedmouhamed5457
    @mouhamedmouhamed5457 4 роки тому +3

    Aka begue yayam ndongo rouyou kay nga

  • @alioutallbayefall302
    @alioutallbayefall302 4 роки тому +2

    Ndaysane Yalna yalla kharé aldiana barké serigne fallou

  • @abdoumane812
    @abdoumane812 2 роки тому +1

    Le meilleur de sa génération