Tata manguilaye nouyou mane bima khole sa tog boumako defe rek daye nekh heur bou may togou yaw lay roye machalla yalna yalla mayla goudoufane ai were rek
Merci pour ces recettes c'est vraiment agréable et facile pour nous qui savons déjà cuisiner c'est des rappels et ça fait plaisir merci beaucoup j'ai un plat que je ne sais pas faire je la rate à chaque fois c'est du riz blanc avec l'arachide en poudre gros bisous
Tata Mary dama la yékha kham tay la djiss Say vidéo mais j'adore en plus wakh dji Bari woul juste les explications nécessaires 💖...amgua abonnés bou bess
Tata dal Mane beug nala trop ,mais doma togal soupou kadia ma khol,demay wadia seyi t sama dieukeur soupou kadia rek la beug,Tata diap si way,magui lay har.merci thiou bi mom leçon bien sû
Bonjour C’est la première fois que je commente sur UA-cam Juste pour vous dire que j’aime bien vos plats c’est comme ceux de ma mère. En plus t’es ingrédients ne sont pas difficile à trouver . Yen a pour certaines elles mettent bcp d’épices que c’est difficiles de refaire leur plats car parfois tu n’arrives à trouver les épices qu’elles utilisent. T’es plats sont simples jolies et appétissant. Et aussi vous êtes très propre. Merci tata isseu
Nouvel abone tata mane xawma foyma nekone bâ yeha guis say vidéo machaalla naturel ta façon de cuisine aah Jaime bien surtou Lima beug rhi tog ogno ver cani troum tathe gui merci ta
Salam aleykoum. Je suis malienne, mon mari sénégalais et j'aimerais préparer ce plat. Ca donne envie. 😍😍 Quel poisson peut-on utiliser s'il vous plaît ? Merci
maachallah togue ndar deugue contane si yow et amine pour les prières sur le corona que dieu ns en épargne dakh ko fi gneup délo si sene activités inchallah
Lo toguoul bakhoul mane yow rek lay suivre plats you nekh guay presenté je vs adore
Vos plats sont appétissants. On sent que vous cuisinez avec amour.......jolies boulettes bravo 👍👍
Asalamou alayecoum je tener à vous remercier pour toutes ses plats bien cuisiné machahalla
@@adamaawadiallo5202l
Tata manguilaye nouyou mane bima khole sa tog boumako defe rek daye nekh heur bou may togou yaw lay roye machalla yalna yalla mayla goudoufane ai were rek
Merci pour ces recettes c'est vraiment agréable et facile pour nous qui savons déjà cuisiner c'est des rappels et ça fait plaisir merci beaucoup j'ai un plat que je ne sais pas faire je la rate à chaque fois c'est du riz blanc avec l'arachide en poudre gros bisous
J'adore cette dame sa voix ces plats bravoooo😍😍😍😍
Machallah tata yalna YALLA wéreul lokhobi cest vraiment superrrr
Yaye isseu défatigua sa manine yalla nana yalla lafal thiate té bayila sounou kaname
Merci yaaye Marie. S'il te plait pépare le saka saka. Merci pour les leçons
Machalla ak thiéré mboum
Tata Mary dama la yékha kham tay la djiss Say vidéo mais j'adore en plus wakh dji Bari woul juste les explications nécessaires 💖...amgua abonnés bou bess
J'irais à ndar pour épouser m'a femmes inchallah
Mane dal yaw la gueumm akh tog dafa am wayyy ❤️❤️❤️
Maachaala tata thiou bi diarna yonn❤🙏
Mane jtm dal maman psk j'aime ta cuisine machala
Ma sha Allah très satisfaite de toi et amine pour les prières
machalla yalna yalla weurel lokho bi
Machallah liguay def neik na waay
Machallah tata ❤
Machallah tougou nacena👍👍
Mash'allah thiou bi awna yone 😍 explications yi lerna
Tabarkala sel n'a présentation bi yiw n'a machallah
Merci votre plat c'est agréable ❤❤
Mansha Allah tata yalna sadiam yague
Machallah mangui ley encouragé togou yi rafetna na nekh na
Machallah sete na rafetna
Amna tâta way ❤️❤️ on te love
Slt, tata yaye isseu merci pour les recettes. Nougnoule toguai mbakhalou ndokhou dieuneu bou âme soul ak koudia
Mashalah Djeureudjeuf
Machalla rafettna sokhaci
J'aime
Tata dal Mane beug nala trop ,mais doma togal soupou kadia ma khol,demay wadia seyi t sama dieukeur soupou kadia rek la beug,Tata diap si way,magui lay har.merci thiou bi mom leçon bien sû
Toog n'a ko
Machalla amatina solo
Mashalah niguay togue nekhnama selna tek si depuis USA
Machallah ❤❤
Nekhna machalla
machalla diek daal day meuna togue machalla laf thiet
Yaw rèk lay toop
Yaye Idée il faut nous préparer du ragout de viande car mon mari aime bien ça.
Macha Allah ma Badiane bauy d'amour diégue piiiire,ma yeureum woudiou mane🤣🤣🤣🤣
Machalla j'ai appris à faire du vraie sauce kani merci
machala laf thiat khamna dina saf lol
❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️
Machala tata, lo doundou doyoul
Machallah tata sama pala préférée nékh na sell na séte na Machallah yalla na lokho by weur Amine 🍽😋
Une nouvelle abonné
Machala chapeau
Machhala 🤝🤝🤝👂
Ya bakhe way
Muito obrigado pela mostrar fazer comida😘
Mashallah mashallah sino dognou defaral recette bou nekh en c periode de confinement merci bcp
Machallah machallah yallah na gnou yallah same ak sounoye djébote
Marie Diop vous êtes superbe très bonne cuisinière qu'Allah vous protège Amennnnn
Hi mum you cook very well i like
Thiou bi teint na machallal
J'aime bien vos plats et votre façon de cuisiner. Merci Tata
Bonjour
C’est la première fois que je commente sur UA-cam
Juste pour vous dire que j’aime bien vos plats c’est comme ceux de ma mère. En plus t’es ingrédients ne sont pas difficile à trouver . Yen a pour certaines elles mettent bcp d’épices que c’est difficiles de refaire leur plats car parfois tu n’arrives à trouver les épices qu’elles utilisent. T’es plats sont simples jolies et appétissant. Et aussi vous êtes très propre. Merci tata isseu
Mafé boulett yaye isseu
Machalah trop bien fait tes plats merci encore ❤️❤️❤️
Machalla maman
Machallah
So delicious 😍😋
Tata issa mercie ak confinement bi je que suivre tes plats depuis France mon mari mes enfants mangent des bonnes repas à cause de toi
😋😋😋😋
❤️❤️❤️🇸🇳
Macha allah 😘😘😘😘😘😘😘😘😍😍😍😍😍😍🥰🥰🥰🥰🥰💞👍
Mashallah Tata lingay togou amna solo esk khamnga ni yangui diangal khalé djiguen yi sen yayi diangalout togou
Machalla tata,j'adore votre cuisine
Machala
Niami niami way sour na way🤣🤣🤣
Mashallah, tu cuisines bien.
Manchalla tanta
Machallat c est bien expliquer merci pour le partage.
SLT. Tata. Sa. Doke. C. Bon
Machallah yalna lokho bi wér et amine si niane yi waye 🤲🤲❤
Ayyiwaye mais yangi maye dimbali si yainne toggou yi surtout souppou kandia ak vermicelle ak mafé
MachAllah
Fatou Cissethiam jlbjmv
Nouvel abone tata mane xawma foyma nekone bâ yeha guis say vidéo machaalla naturel ta façon de cuisine aah Jaime bien surtou Lima beug rhi tog ogno ver cani troum tathe gui merci ta
Sa thiou bi bakhna nekhna machAllah ❤
damey aimerr ba paré soga sétane
Machallah tata man yow lay weur
👍👍
👍👍👍👍👍👍
Ah thiou bi riche na machallah sa donne envie de manger mane mome damay noter rek yag fi lol tè wer
Machallah 👍👍👍👍👍👍💛💛💛💛💛💛💚💚💚💛💛💛💛💛👏👏👏👏💪💪💪💪
Machalha diarra na yone
Merci maman on est très content de vous nalla yalla fay
Miam miam Mercie tata j'adore tes plats vous cuisiner bien machaallah
Salam dou am netetou
Démoda mot ame nététou
Merci
Pour les gourmandes comme moi c un regal🥰🥰🥰
Salam aleykoum. Je suis malienne, mon mari sénégalais et j'aimerais préparer ce plat. Ca donne envie. 😍😍
Quel poisson peut-on utiliser s'il vous plaît ? Merci
Merci ass ass thon blanc
maachallah togue ndar deugue contane si yow et amine pour les prières sur le corona que dieu ns en épargne dakh ko fi gneup délo si sene activités inchallah
Magui soga guis say video j suis nouvelle abonnée machalla mam dama ama passion ci togue dona dina setane video yi passe inchalla
Maman lingay reugueul yeup neikh waya dara dou thiou boulettes bii❤️ machallah way
Masha'Allah sama plat gua toguou
Recette beignet thiopati svp !
Merci
Manchalla sa togg neikhna simple na rafet na
Mashaa Allah bien présenter svp en français
What is kani Soffiane?
👍👍👀
Man.dal.beuguenala.lol
Je v thiou kandia
Machalla
Ça à l'air super appétissant, mais quel poisson avez-vous utiliser pour la réalisation du plat?
Sindé Sindé c'est du king fish
MASCH’ALLAH☺️
machallah👌👌
machallah
Nékh n'a torp mama
Chou boulette dou am soupomé?
Bou la nekhe
Waw machalah tu nous simplifie notre quotidien 😅j'aime beaucoup notre cuisine sénégalaise💯 😍merci depuis 🇨🇵