Serigne Moustapha Sy Voici la réponse émouvante de la fille de Serigne Mansour Sy Borom Dara J AMIRA

Поділитися
Вставка
  • Опубліковано 6 січ 2025

КОМЕНТАРІ • 954

  • @omardrame9287
    @omardrame9287 4 роки тому +13

    yalna yalla bolé wa tivaoune si diamm si barké baye niass aminnn😢😢😳😳

  • @claramendy3336
    @claramendy3336 4 роки тому +97

    Paix dans la famille du Khalifa Sy ! Dieu apaise le coeur des hommes, nous n avons que toi pour nous guider. A la grâce de Dieu

  • @moustaphamboup3097
    @moustaphamboup3097 4 роки тому +13

    Bilay ma beugue sama touro do bilay serigne Moustapha sy maka beugue mo raw népou bayi léne tongne ❤❤❤❤❤ kou beugue sama Toura do défal j'aime

  • @ahmedbachirgueye2974
    @ahmedbachirgueye2974 4 роки тому +12

    Ana Soutoura wéranté bakhoul naniou neube yi niawyi Dioulite daye rafétal aye Yallah li niawna ! Yallah na Yallah sakhal diame thie Famille ELhadji Malick Sy ( R.T.A)

  • @mohameddiop2014
    @mohameddiop2014 4 роки тому +29

    Serigne Mbaye Sy Mansour yalla nafi yague tei weure 🙏🏾AL Khalifa ❤️

  • @cheikhbi2056
    @cheikhbi2056 4 роки тому +85

    Oumoul Amira la Lionne de Serigne Mansour. YALLA na YALLA dolli Jamm TIVAOUANE.

  • @geuyefamily6807
    @geuyefamily6807 4 роки тому +71

    Serign babcar sy mansour yall'na yalla yagal kofii loll barké seydina moukhamét psl

  • @al-futiiyutv_TBD
    @al-futiiyutv_TBD 4 роки тому +3

    Waaawww. Ben Tiwaoune rek mo am, té moy bou Mame Mawdo Malick, khalif di Serigne Babacar Sy Mansour.

  • @thiatouyayamxaritoupapam111
    @thiatouyayamxaritoupapam111 4 роки тому +78

    Ay way arrêter ça 😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭Tarikha tidiane sokhlawoute li on veut retrouver notre tarikha sougnou mame El Hadji Malick djangualougnou li 😭😭😭 j’ai mal trop mal

    • @mohameddiop5380
      @mohameddiop5380 4 роки тому +4

      Tarikha tidiane kay amoul problème séne famille gno ame problème lidiatilene séne problème ta guénési tarikha bi

    • @momodioufy3220
      @momodioufy3220 4 роки тому +1

      Thiatou yayam xaritou papam tarikha Tidian meussouta ammm problème té yittt douko moussa amitttt probléme famille ak tarikha bi c diamétre ma opposé tarikha bi akkka yatou khipi len sen beutttt teyyy khôl

    • @fatimadiop1692
      @fatimadiop1692 4 роки тому

      ua-cam.com/video/CFNM0z5zlSU/v-deo.html

    • @fatimadiop1692
      @fatimadiop1692 4 роки тому

      @@mohameddiop5380 ua-cam.com/video/CFNM0z5zlSU/v-deo.html

    • @fatimadiop1692
      @fatimadiop1692 4 роки тому

      @@momodioufy3220 ua-cam.com/video/CFNM0z5zlSU/v-deo.html

  • @DioufMaodo-wr4oo
    @DioufMaodo-wr4oo 3 місяці тому

    Yalanako yalla yeureum xaréko firdaosssi diarama sérigné Moustapha sy

  • @mamadoudiouf6260
    @mamadoudiouf6260 4 роки тому +33

    Xolalma li rék kunéka ngi khawi sa suture morom. Seytané begna lool fanyi. Wayé yalla na sunu borom fay bi tiow si barkép serigne touba.

  • @yacinesouare6413
    @yacinesouare6413 4 роки тому +42

    Kérok dama 😭😭 si wakhou sérigne Moustapha m yalla bakh na alkhamdoulila Sante Serigne Babacar Sy rek khalifa bi yalla nafi yague t wére

  • @bachirdiene7541
    @bachirdiene7541 2 роки тому +4

    Fier de Serigne Moustapha Sy

  • @gueyeabdou8849
    @gueyeabdou8849 10 місяців тому

    Sama yonne nekku thi Sonko moÿ sma Serigne Yalnafii Yagg

  • @elhadjibadiane344
    @elhadjibadiane344 4 роки тому +10

    Naniouko nianal yalla délossi watt xélam bamou weulbatikou topou si aye guinaw bayam insha allah

    • @mallbelly8250
      @mallbelly8250 4 роки тому

      Serinie Moustafa khalifa bi rawouko bamou koy topou

    • @mallbelly8250
      @mallbelly8250 4 роки тому

      Wakh ma bane khasida lafi binde

  • @mayadandiaye500
    @mayadandiaye500 4 роки тому +2

    Fannn n'alla machallah sama mame la khass nako nieuppp bayi akk yallla😭😭😭😭

  • @lobsobservateur5375
    @lobsobservateur5375 4 роки тому +13

    Ce que je l'habitude de dire à chaque fois, kham kham ak daraja deffeu wara andak yarr ak teguine wasallam

    • @talibebayamcisse5058
      @talibebayamcisse5058 4 роки тому

      Ma tegal la ci ak ragal Yàlla sinon mu sonal Boroom

    • @cissejarod
      @cissejarod 4 роки тому

      Ragal yalla te bagnko bocale AK ken

  • @alassanendiaye1864
    @alassanendiaye1864 4 роки тому +1

    Merci sokhnasi sy dathiye bakhe nak c bon awe ki momoul nit yi way

  • @mbenguemohamed8395
    @mbenguemohamed8395 4 роки тому +6

    sokhna amira kagne Nga wérr bay khasté
    iow ci décès Serigne abdou bi rek Nga done khoulol s mb sy Mansour
    té iow sakh si sa bire wakh né Nga sokhna Sophie dème apré si fin bi Nga ni sokhna astou kane Amira ki es ti

  • @ndeyetalibekhalifaababacar8634
    @ndeyetalibekhalifaababacar8634 4 роки тому +2

    Serigne Babacar Sy Mansour YALLA naa fii yaagu tei weurr

  • @jeanmariekenndiaye4428
    @jeanmariekenndiaye4428 2 роки тому +4

    Vous êtes une seule et unique famille. Ton rôle toi fille doit être d'unir la famille notamment les jeunes.

  • @OuseynouMbaye-fc1ev
    @OuseynouMbaye-fc1ev Рік тому

    Yalla n'a yalla indi djamou thi djabotou maoulana cheikh Malick Sy thi barké maoulana cheikh Ibrahima Niass

  • @dechibafall5630
    @dechibafall5630 4 роки тому +9

    Sokhna amira sy wérale amale diame goudale fane 🙏💚

  • @fatougueye9102
    @fatougueye9102 4 роки тому +2

    Machallah Sy Malik longue vie amine yarabi au NOM de NOTRE PROPHET MUHAMMAD PSL

  • @adjandiaye7202
    @adjandiaye7202 4 роки тому +13

    Machallah sy malick yalna yalla yokou diam dji ❤🥰❤🥰❤🥰❤🥰❤🥰❤

  • @ArameDiop-gp8fz
    @ArameDiop-gp8fz Рік тому

    diarama serigne moustapha sy❤❤❤❤ l

  • @senegalvillagetvdiop5152
    @senegalvillagetvdiop5152 4 роки тому +8

    Machalah me dalle al lou mena am wah dafa am place bou ameh ak blem ci bire famielle bi nako lidjiane ti ci bire famielle wame te bañko wah ci bir talubeh yi

  • @moustaphandiaye1219
    @moustaphandiaye1219 2 роки тому

    Dieureudieuf Serigne Moustapha sy maktom

  • @ndeyesalioundiaye3119
    @ndeyesalioundiaye3119 4 роки тому +24

    Thiey yarabi 😭 😭 😭 😭 😭 mandee dama tiit te rouss niemantii khalif bii ndeyssan 😭 😭 😭 😭 😭 😭 😭 😭 😭 😭 mouride la dee m suis de t cœur avec le khalife 😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭

    • @adjafall2536
      @adjafall2536 4 роки тому +1

      Danga bakh machallah

    • @bakhalil3573
      @bakhalil3573 4 роки тому +1

      Yalla nala serign touba takhawou

    • @gueyeastou5385
      @gueyeastou5385 4 роки тому

      Yalla nalaa yalla deef deug deug talibé serigne touba yaa baak

    • @mamadou3723
      @mamadou3723 4 роки тому

      diadieuf

    • @cheikhouka4718
      @cheikhouka4718 4 роки тому

      Bayilen di wakh moridla ak tidiane la

  • @serignendour7915
    @serignendour7915 4 роки тому +1

    Contac merci sokhnaci

  • @cheikhenglishlo9121
    @cheikhenglishlo9121 4 роки тому +4

    Ndeysann fekk ko xamné ay nagame nann si woulll nguén diko fi dougall vive Serigne Moustapha sy ♥️

  • @cocottendiaye1944
    @cocottendiaye1944 4 роки тому +2

    *Sa voix😭😭😭♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️SyMalick*

  • @khalifaseck3351
    @khalifaseck3351 4 роки тому +3

    Ki fene rek wakhofi dara demal Serigne Moustapha sy diagala mogeune si yaw bamoulene Di raw yaguena

  • @papelamineseye4161
    @papelamineseye4161 4 роки тому +1

    Yalna diame yague

    • @fatimadiop1692
      @fatimadiop1692 4 роки тому

      ua-cam.com/video/CFNM0z5zlSU/v-deo.html

  • @Alkhalifaababakrin96
    @Alkhalifaababakrin96 4 роки тому +6

    Kifi euppou kham kham si tarikhabi champ de coursou ba la dane gamo.

  • @cissebabs8961
    @cissebabs8961 4 роки тому +4

    Mes respects Amiral parfaitement raison ki dara diapoul ko loudoul bone ak sokhor

  • @tresortirera2093
    @tresortirera2093 4 роки тому +13

    Cc j'aime le discours ms elle la fait une hereure ndakh champ de course Serigne cheikh moko fondé difa gamo Kone boné dafa khégne koufa diouly amo diouly yagui wakh loula nekh boy wakh wakhal ak Serigne Moustapha ms pas l'étirage parck Moustapha Mack gni nio wakh Serigne cheikh mou diokhko dayira mourchid Serigne Moustapha mm si il la fait erreur courigeko mom ms pas le dayira

  • @thiammbaye3602
    @thiammbaye3602 4 роки тому +1

    Talibé day yam place talibé souniou thiofél ci ndiabotou maodo leu dieum mais dou ki wala ké. Talibé cheikh day mandou
    Wa salam🙏🏽

  • @khadykounta7255
    @khadykounta7255 4 роки тому +4

    Salam macha allah merci

  • @fatythioye6866
    @fatythioye6866 4 роки тому +2

    Allahou akbar seytane toggal

  • @elhadjindiaye9632
    @elhadjindiaye9632 4 роки тому +5

    Nga balma yaye boye nguir yalla rek boul topp ki yalla guis na lep

  • @Del2Mas
    @Del2Mas 2 роки тому

    Yow amo Respect sisa bay Serigne cheikh .
    Amira Do Dara nohoul feule yow guay djiguen wara defar SI yiw gua Tok Fi fen liguay wah Dara dousi deug

  • @elhajibiranesall8510
    @elhajibiranesall8510 4 роки тому +8

    Famille mi yalla defsi diam

  • @amadoumboup2270
    @amadoumboup2270 2 роки тому

    Dieurediuff sokh nasi

  • @fatyfall7362
    @fatyfall7362 4 роки тому +8

    Machalla sy Malick 💖

  • @papedieng6815
    @papedieng6815 3 роки тому

    Bilahi mer ya bon

  • @datly44
    @datly44 4 роки тому +12

    Que Dieu le Tout Miséricordieux accorde la paix entre les descendants de la famille Sy adouna amoul solo wakhtane lène ba djoubo Yaye boye

  • @bourguibafaye8521
    @bourguibafaye8521 4 роки тому +1

    Dieureudieuf sokhna sy

  • @ToubaVisionToubaVision
    @ToubaVisionToubaVision 4 роки тому +58

    Thieuy Saytané Togal Foumou Khadioul Réck Lay Douckou Innamal Mominona Ikhwatoun Fa Aslihon Bayna Akhaway Coume

    • @laminedioppikinerue105
      @laminedioppikinerue105 4 роки тому +8

      Seytané nite la déh . Moustapha Sy sila bokhou seytané bou bonla

    • @deugdouroumbnop1434
      @deugdouroumbnop1434 4 роки тому +3

      @@laminedioppikinerue105 wakh ko si kaw

    • @karadio692
      @karadio692 4 роки тому +2

      Yénn gñi koulénn yéss amoul Rambatjj rekk

    • @karadio692
      @karadio692 4 роки тому

      Touba vision si familles diambour sa yone nékoussi Sénn keur mo 1peu Prblém séytané conard

    • @Le_Natron_
      @Le_Natron_ 4 роки тому

      Le Pays est entrain de Foutre le camp 😭😭😭. Où est Dieu dans tout ça !?

  • @sokhnambodj5594
    @sokhnambodj5594 Рік тому

    Amine

  • @instagramsecurityhelping1095
    @instagramsecurityhelping1095 4 роки тому +3

    Machallah sokhna si

  • @tawfiikhcheikhbi3161
    @tawfiikhcheikhbi3161 4 роки тому

    Yalla na yalla déf jamou ya rabi

  • @youssoutoure2834
    @youssoutoure2834 4 роки тому +3

    Ma bègue Serigne Moustapha sy al mactoum 🙏🙏🙏

  • @moustaphadiagne4278
    @moustaphadiagne4278 4 роки тому +1

    Yallena yalla delo si diam si famille yi réro yeup

  • @papediop8064
    @papediop8064 4 роки тому +16

    Machalah sy Malick 🙏

  • @ndiemediouf222
    @ndiemediouf222 4 роки тому

    Problème bu commencer 1957 nganii 2020 nga kaay regleii koon weroo

  • @OmarOmar-cu3du
    @OmarOmar-cu3du 4 роки тому +9

    Sokhna ahtou kane koubakh té cele 😭😭 yawe ya bone

    • @maremefaye3146
      @maremefaye3146 4 роки тому +1

      Yaw dh Serigne Moustapha s'y makhtoum molo guene fou

  • @tourekhar4111
    @tourekhar4111 4 роки тому

    Merci amira que dieu vous bénisse

    • @fatimadiop1692
      @fatimadiop1692 4 роки тому

      ua-cam.com/video/CFNM0z5zlSU/v-deo.html

  • @khoudiatall5467
    @khoudiatall5467 4 роки тому +36

    amna solo torop machalla

    • @fallam1010
      @fallam1010 4 роки тому

      wa fans club Aïda diallo am géén problème nak shéttetettetettete

  • @FatouNdiaye-xx5ri
    @FatouNdiaye-xx5ri 4 роки тому +2

    Thiéyy Serigne Moustapha kouko bagne dégayy sonn reyy

  • @fatimatambaye9116
    @fatimatambaye9116 4 роки тому +5

    Mâcha alla sy demba 🥰

  • @breezybrown6940
    @breezybrown6940 4 роки тому +2

    Sayid cheikh Ahmed tiadiani sy alxoutboul maktoume rta kokou dou moromou ken da nga yarèdiko rek

  • @ngagnemboup8841
    @ngagnemboup8841 4 роки тому +26

    Vraiment képou kouy tidiane da ngeu am gathia billahi
    Mane damay took bam yague mani diamano dji djiémal kham sa diné bou wére di diamou yalla bou wére diartoul ngeuy djiokou si béne serigne ndakh moy lolou billahi sama xol dfa djiékh

    • @ahmadoufaye7047
      @ahmadoufaye7047 4 роки тому +1

      C vrai dé fi guissouma fii dîné dh nioune talibéyii naniou kholat sougniu bop té djamoudji yalla dama rouss

    • @mkmk481
      @mkmk481 4 роки тому +2

      No mai tijane tivaouane key Hanna.
      Coz nous les autres tijane ça ne nous concerne pas.

    • @Salam16488
      @Salam16488 4 роки тому +2

      En réalité les tarikha nous empêche de mieux pratiquer la religion.
      Ça ne va pas durer ils ont perdu le contrôle.
      Seul la sunna est garanti par Allah pour l'éternité.
      KHÉLOULÉN

    • @ousmanenoreyninoreyni5996
      @ousmanenoreyninoreyni5996 4 роки тому +3

      @@Salam16488 yaw boul wakh les tarikha dh yamal si sénn tarikha Babou mom Nga kham boul togne

    • @omardrame9287
      @omardrame9287 4 роки тому

      bamou désse wa keur baye niass dieurdieufé baye niass

  • @cheikhtidianetoure7197
    @cheikhtidianetoure7197 4 роки тому

    Ma khalla ligène di woté ngène atanoul khalifa général Tidjan mo takh li yeup am boulen sisou baye Niass khadioul thi gunaw ken fek topolène ki yalla dital thi adouna bii dolen djouk thi lii baye moy khalifa CHEIKH TIDIANE ❤️

  • @matardiouf71
    @matardiouf71 4 роки тому +25

    Machala amna solo khalifa bi yalnafi yague ak weer

    • @fallam1010
      @fallam1010 4 роки тому

      wa fans club Aïda diallo am géén problème nak shéttetettetettete

  • @papasy3679
    @papasy3679 4 роки тому

    Merci Maman Amira Sy

  • @mamadouseck3203
    @mamadouseck3203 4 роки тому +34

    Moustapha SY est principal fautif, il ne fallait pas parler ainsi

    • @assmbaye1019
      @assmbaye1019 4 роки тому +2

      Yalnako yalla soppi niite day am kilifa

    • @fallam1010
      @fallam1010 4 роки тому +2

      wa fans club Aïda diallo am géén problème nak shéttetettetettete

    • @amathndiaye7962
      @amathndiaye7962 4 роки тому

      Comédien laa

  • @gueyesokhnaaissata6693
    @gueyesokhnaaissata6693 4 роки тому

    Yenn nie di khass Serigne Moustapha Sy Lou Bonn senn thiotou ndayee

    • @kyabussinesswoman7094
      @kyabussinesswoman7094 4 роки тому

      Sa leufal ndaye dmrm

    • @gueyesokhnaaissata6693
      @gueyesokhnaaissata6693 4 роки тому

      😁😁😁😁😁😁😁😁😁😁😁😁😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂

  • @momofall9721
    @momofall9721 4 роки тому +3

    Merci yaye boye

  • @diopteranga2666
    @diopteranga2666 4 роки тому

    Maschalla sy

  • @cheikhtidianed
    @cheikhtidianed 4 роки тому +5

    En tout cas Serigne Moustapha ay résultats wam niép guis nañ ko Lim déf ci tarikha bi kén ci yén défouko ci ignan rk mo lén diap

    • @wakhalsamarewmi2766
      @wakhalsamarewmi2766 4 роки тому

      wala loumou defal buppam way defaloko tarikha bi

    • @manchoufaye6265
      @manchoufaye6265 4 роки тому

      @@wakhalsamarewmi2766 en bon ? Tamnagne ko jiko soul 1000 jeuf you bah ndah 1.. sen jikola

    • @manchoufaye6265
      @manchoufaye6265 4 роки тому

      Yalla lako taha wah 💖. Hasida Mame yi taysir Hylas... Cadets bo feug mou tarilla len firil lako lep ci lohom..
      Yalna yalla guoudal say Fan may la weur ak weurlé sy Malick ❤️🙏

    • @cheikhtidianed
      @cheikhtidianed 4 роки тому +1

      @@manchoufaye6265 walay nday saan chaque jeudi rabountabara bi diouli ci 5 continents yép vendredi kharatoul dioumah bi niki nonou li kou nékoul nafékh mangako sédé
      Jarama Serigne Moustapha ♥️

    • @cheikhtidianed
      @cheikhtidianed 4 роки тому

      @@wakhalsamarewmi2766 kon yow wéro

  • @thiammbaye3602
    @thiammbaye3602 4 роки тому

    Amira 😥

  • @assanendiaye2483
    @assanendiaye2483 4 роки тому +6

    Yallana yalla déf diamou thi réwe mi mbokou yi nanou moyetou yéne vidéo yi ak yéne kado yi d'Ay yakh mbok gui d'Ay yakh tarikha bi d'Ay yakh dinédji yallana yalla tapé khôl yi

  • @mouhamedkounta9819
    @mouhamedkounta9819 4 роки тому +1

    salam maneu dhé khadirla magui gniane sama mbook yii book thi tarikha tidiane fi tiwaoune .. guéneu rafétal thé bayii wakh yii guéneu di wakh ndakh gniléneu sope barké serigne Babacar sy ndankh gnouneu tmt thi lagnou book koneu guir yalla bayil léneu lep tay diélalé guir yalla guéneu balma nak wa salam

  • @khadydrame9827
    @khadydrame9827 4 роки тому +4

    Machallah sy malick

  • @makhtargueye7940
    @makhtargueye7940 4 роки тому +1

    Grazie mille

  • @binetousene1862
    @binetousene1862 4 роки тому +19

    Merci amiral Sy Malick ❤️❤️❤️❤️❤️❤️

    • @fallam1010
      @fallam1010 4 роки тому

      wa fans club Aïda diallo am géén problème nak shéttetettetettete

  • @IbrahimaToure-tc9ho
    @IbrahimaToure-tc9ho 9 місяців тому

    ❤❤❤

  • @evatra9396
    @evatra9396 4 роки тому +15

    Dieureudieuf 👍👍

    • @fatimadiop1692
      @fatimadiop1692 4 роки тому

      ua-cam.com/video/CFNM0z5zlSU/v-deo.html

  • @assatoubanesamb5874
    @assatoubanesamb5874 4 роки тому

    Wouy magui dé 😍😍😍😍😍😍😍♥️♥️♥️♥️♥️😀😀😀😀

  • @cheikhbambadiouf4908
    @cheikhbambadiouf4908 4 роки тому +7

    Onjoubilakhi mina saïtani radjime

  • @keurgui77.71
    @keurgui77.71 4 роки тому +1

    Kou saga sa nidiaye dinga fayou

  • @moustaphafall6717
    @moustaphafall6717 4 роки тому +8

    القرآن ak السنة rek

  • @bounabanno6961
    @bounabanno6961 4 роки тому +1

    Kii limou wakh...... mook li moustapha wakh.... ñoo yém dong😡😡 Kii dafa fèbbre..... tanéwul moustapha,té moom dafa wara noppi😡

  • @aichakane1167
    @aichakane1167 4 роки тому +14

    Wakhena lou niawe wayé ya wite wakhe nga lou eupou ndakhe ndakhe menone nga sè rousse serigne babacar wala al amine wala pape malick s’y ryth

  • @papeka2276
    @papeka2276 3 роки тому

    Djaram serin Moustapha sy

  • @zoooaam
    @zoooaam 4 роки тому +4

    Alhamdoulilah, audio bi takhna ma gueuna diapeu Serigne Moustapha SY. Serigne Moustapha kay limouy wakh leupeu deugue la. Dégalma ndawsi lou gnakkeu solo li mouy wakh rekkeu. Alhamdoulilah ma ngui sante YALLAH bamouma nguindé.

  • @bnbezofficial1376
    @bnbezofficial1376 4 роки тому

    Bilahi serigne moustapha molay geuna goudou fane

  • @salioudiop7141
    @salioudiop7141 4 роки тому +4

    Yaw lem ga dh 😂😂😂say wahh amoull Benn vohérence ma bll😂😂

  • @fatousarrgaye1194
    @fatousarrgaye1194 4 роки тому

    Sokhnassi magui ziar .wanté yènenabok té Aÿ nit daniouy tanenté dah yonenbi psl bania fayoneté larawé nieup.bolènetah niou rétanlène.guiryala délène halage"" konopi mothieu" wahi yoneneta la psl

  • @aminakane3214
    @aminakane3214 4 роки тому +4

    Aye waye dou wakhou fii naniou mougne té khamni yalla ,wakhoul kéne darra

  • @ousseynouka3963
    @ousseynouka3963 3 роки тому

    Sérigne Moustapha sy mon rawe sa mbaye s'y xam xam amon loko wakh, seytané by gua done ,

  • @abdoufaye1909
    @abdoufaye1909 4 роки тому +4

    Sokhna Amira nga balma wayè yangui beugueu nouro ak Moustapha. Liii waroko wakh fiii

  • @mamediaraseye3746
    @mamediaraseye3746 4 роки тому +1

    Yena bokou sene mame khadiou nousi barke seringe saliou na Lepou rafet

  • @FrancijFrancij
    @FrancijFrancij 4 роки тому +12

    Machala amira machala amna solo tropp dieurdieuf

  • @bathieniang1334
    @bathieniang1334 4 роки тому +2

    Soura yalla yatouna d'oùmala totou bilahi nk lithie kanam soriwoul

  • @titifarou8257
    @titifarou8257 4 роки тому +16

    Amna solo machallah sy malick

  • @boubafall1014
    @boubafall1014 4 роки тому +2

    Merci yaye Amira

  • @modouniass8093
    @modouniass8093 4 роки тому +4

    Boul si khas serigne cheikh
    Serigne cheikh moy tarikhatoul tidiania yaw nak tamite wéro dee a 100% dé

  • @mamadoumbaye9872
    @mamadoumbaye9872 4 роки тому

    Yalna yalla doliniou soutoureu té mousseul niou si cheytané, amine