*Nous aimons serigne babacar Sy Mansour ta dra douko dindi* *Yalla naniou Yalla djegal sounouy bakkar Serigne bi li nga wakh reuy na bouddonn lou am sax waroulo ko wax waxumaak nak Damou sheikhal Khawmi* *Yalla baxna 😢😢😢😢😢*
Aka bari xam xam lolll son organisation et parfaite Mai bene défaut la am moy dafa iniane jamais mou dakor si li yalla deff Pour mom warna yilif adouna président bou nieuw joxoko nop mou xass la meme macky sall sukoy critiqué dou objectif personnel Serigne amga presk 70ans kone amna lo waratoul Maodo nak nena barina kuy wotei batine fii si adouna euleukk neinne rek la yorr Serigne Babacar sy mansour yalla nafi yalla tei werr
Kou beug Tass diinée si réweum d'où andak kokou begeu yax lalay DF du andak macky mi nane nouvelle ordre mondiale té lak yallah may mayou KO fi ken l'on doyéwoul iniané ken len kou NK lala yallah sed RK yaye borome te point......
Vous êtes seulement hypocrites.... mais les sahabas même se sont entretues entre eux..... Ces problemes ne sont que l'œuvre de ibliss... donc epargnez nous de votre ignorance....
Man dh mourid la talibe Mame cheikh anta mais li mom rafetol Mame elh Malick Sy ndiabotam waro gno tok Di wah yen wah yi guen Balma nak yalna yalla doli sotoura ak khelmo rafet barke Serigne saliou
BOUMA SAGNONE LI KHEW BÉNE TALIBÉ DOUSI WAKH 🙏NIT KOU SAGNE WAKH BAYIKO AK YALLA SOUNOU BOROME NIT BO NATÉ WAKH BA KHAM NIMOUY DEF SI KHOL NGA WAKHKO SA MOROMOU GOR GUIR OUT LOU MÉTI KHOLAM BOUBOBA YALLA MOY RÉAGIR NA GNEUP NOPI TÉ AM TALIBÉ KILIFEU YALLA MOKOY FADIAL MÉRAM NIT BIMA GUÉNEUH RAGAL SI ADOUNA MOY BIY HEUY SOUBA BA NGONE DI OUT LOU MÉTI NIT KOKOU MO RAW MALAKA BIY DIEULSI ROUYI NDAKH MOLAY RAY TES KEN DOUKO YEUK 🙆♀️YALLA BOUMA YALLA MAŸ KHOL BOUMAY WAKHÉ NIT LOU GNAWWW 🙏 TALIBÉ CHEIKH BA FAWWWW❤️❤️
Je suis mouride et avant tout musulman c prkw limome rafetlou mako dara bilayy dama metii amna yo khamni kilifa douko def dakh polémiques rek lay indii😳
@@khadykebe4736 pardon ma ngi toube dé dama fok ni tarikha Bo si bokoul rek khamo lou fa khew nopi Da lay warr bou néké nit kou manou nga nakh wakh bo guiss ame na lou ko waral wayé balma Da ma fogone ni talibé borom touba nga nakh mome si loumou kham rek la done dokh ak wakh 🙏🏾
@@serignendiaye1213 je parle avec ceux qui ont de l'éthique donc vas consulter ton dictionnaire bref il faut penser au conséquences nous sommes tous ensemble.
@@elhadjimbengue4664 Sérieusement Vous êtes comme des moutons 🐑 enchaînés ... Vous ignorez l'histoire c'est la raison pour laquelle vous donnez de l'importance à cette personne
Moustapha Sy ya boonne,sa gamou tok fa sakh bakar rek nga fay dieulli, Serigne Babacar Sy Mansour Aly Khalifatoul Am dou xalate sakh lou boonne ba di ko def.
Je suis vraiment choqué !!!cette fois ci tu es allé trop loin et je vois pas quel intérêt tu as de vouloir diviser la famille jusqu'à porter des accusations aussi grossières.
@@julodaigne4172ioe mi ya doff te yeugoko imbrcile yi ngene done do lene sakh rousse di saga kilifeu dinee yi dem lene ngene ndy diangui arkhourane sen ecran yi rk ngene tokk di wakh waye so guenone thi mbedd bi di na la door ba tokk sa kaw😡
Serigne mbaye sy Mansour nitou yalla la tolouna fo khamni si yalla bo donn Rey dou dem si ay diabar dakoy defal bopam....je suis mouride mais liii niaw Na trop yalla khamnako.
Je suis mouride mais limou wakh dafa eup trop mom damako meusse begue mais séparation bi sakh diarouko wone tarikha bou Khalife bi wakhé rek lolou lagnou wara déf diam mo guene lép yalna niep am diam seul le Sénégal qui gagne ❤️❤️
Liii lep rek saytané la rek....je suis mouride mais Serigne mbaye sy Mansour kou bakh la kilifa la té modeste lol ndeye.... yalla Na fi yaagu lol té wer... mais Serigne Moustapha mi momm dafa foogu ni dafa dioum rek si kaw boudé waarnako wax...meunone Na gamou gamomm rek waxtani si goudi ak borom goudi wayé lii mom niaw Na lol yalla khamnako.
Mo yaw xana dou yèna done rayanté fii barki démb si Magal gui. ( Aida Diallo ak Kara ak gnénène ak gnénène) nguay am loy wakh. Un vrai mouride ne se réjouit pas des disputes des autres. Yaw démal ngua xoll fo bokk ba paré bala ngua wakh si ay diambour
J'invite les gens faire très attention à ce Moustapha. Serigne sidy Ahmed Sy est né en 1933 et serigne mbaye est né en 1932. De surcroît, il (Moustapha) a tourné le dos à Serigne pape malick sy. Allez regarder son discours de l'année dernière. Mais, il s'est trompé de cible ndak serigne Mbaye nitou yalla la.
no no ki nite mauvaise langue pervére honte pr humma islamikebi ta trokhol tidianeyi trokholo khalif bi mé gnoune tidiane yi gnou roussati yow diarroul gnou laye serignetou parke tu é modi je te déteste du plu pronfond d mn coeur tu é le diable en persone
Nous vous prions de ne pas écouter les propos de Serigne Moustapha Al makhtoum qui accuse le khalife des tidianes si il le disait à vos pères est ce que vous apprécierez ces mots Abonnez vous à tivaouane 7tv pour avoir toutes l'information religieuses d'ici et d'ailleurs
En tout cas waxone nakofi manilén yallah nafi wax kham kham rék Après dég nafi lou nék Wallahi tarikha cheikh bén khalifa mofi nék témoy biniouy falé si Khadaratou yallah ba té fal naniou Serigne Babacar Sy Mansour Yallah nafi yag té wer ak bép kilifeu diné amine
Dieureeudieufeti Serigne Touba diarrama Mame Cheikh Ibrahima Fall Lamp sama yakkar dji. Yalla na diamm yagu .Yalla dou fayy wakh bayi dieuff .goor goorloulenn yalla nalenn yalla djoubalé.yennou nenn
C du n'importe quoi et très dangereux. Il n a qu a faire son chemin seul et laisser les autres. Il n étais meme pas en de bons termes avec son défunt père. Pas de levons à recevoir de lui .il veut diviser et affaiblir la famille SY .
Tu as raison. Le plus important c'est la religion Islam. Mais pas tous ces Tarikhas qui divisent. C'est la course à la richesse et au pouvoir qui font dériver ces "GUIDES RELIGIEUX "
Mane deh douma tidiane waye sarigne mbaye sy aka mako sop te buegue ko ndakh foulam ak faye dame dokhoul si daray niak fayda yallna fi yagui te werr ak kou wakh amine🙏🙏🙏
Limoy vrai cas communautaire ligua wakh nieupaguikoy nakarlou touchéna bépp tarikha mou Tidiane Mouride Layenn Niassénn etc... wayé Sunu rééw diam rekafikhathie yalla na diam sakh si Sénégal ak adouna bi amine
Dama yakarni seuytanai moy wakh lo nittt yi legui parsk kadou yimay degue nittt yi diko wakh d'où tayefffff 😭😭😭😭yalnaniou yallla moussal si seuytanai akkkk niniou melll yala naniou yalla khirrrr si Lou bakh khir niiu si yone ba dieum sa yallla khirrr niou si Mouhamed (psl) Serigne mbaye si Mansour sounou khalif yalla na yalla goudal sayyy Faye si barké chiekh ameth tidiane
Suis mouride 100% mais deugue mo nekh yallah wakh bou niaw kene khamewoulene ko goulete wakh bi niaw na trop kilifeu dou wakh lougn koy khebei li metina trop 😭😭😭
Liberel domou diambour yi mo gueune. Danga dieufrou. Danga tegui ndigueulou serigne chiekh. Fi nga togue amoul kene kou sant sy. Meme say frères andouniou ak yow. Talibé yi warnagnou kholat sene bop.
Wow mann deh franchement khalifa bi moy sama khalife tei mom lay deglou mais serigne moustapha dei kouka soponn laa batay may guiss video bii Dieuleul nako defense bassonn mais bii mom dafaa the eup Ioee MAME MAODO dafaa top souna ba kheuy dem ioe seutam nganii yako téguii
Gamou la gnou wottè tè lignou si dioublou moy dèfaratt khol yi fattalikou djikoyy seyidina mouhamed (ص) ak histoiram lou yakhou wonnn si dingattè yi gnou dèfarr ko wayè tamitt sante yalla si bagnou bollè si khètam Wayè nèkoul takhalè wala diakhassè ay dingann Yènn borom mouk gaddou yi molnlomi nagnouyy wahh louy diffarr tè bayi louyy yakh nèm deukla
Li sakh dou gamou waron na wote mboumbay mogueun Ana Yallah, Ana yoneitabi Ana Seydi hadj Malick Sy dara loudoul wakhou adouna defante akh wakh Lou niaw lolo takh nga wet guisso sa bene mbok war nga kholate sa bop balay trop tard.
Waaaa kii esk nittt la? Liii bou amone sakh waroko wakh si goudi yonénte bii. Jourou gamou wakhal Nitt yii kouye yonénte. Problème de famille nga régler ko après. N’importe koi wannnn nga Nitt yii gueumo yalla aussi parsk féticheur mounoul ray bakane, yalla rkk moy ray. Ngénnn balma nakkk
Il était banni par son père pendant 5ans banimou guéné adina beugouko guiss takhaw nafi gamou démentir son propre père kon sou wakhé li boumou diakhal ken du ku bakh dou nitou dara gnikay encourager diko applaudir aussi dou gnou nittou dara ay cheytanté lagne amna lo khmni ku ko deg doko apprécié réveiller vous guir yalla ak yonente bi(psl). Qu'est ce que vous aller raconter une fois a la maison 0 enseignement lou tolno gamou nga wara yé say nit ci diner ci djiko yonénte bi (psl). Linék sama khol yeup meunou mako fi wassalam
Kénn,baalmà Serigne Moustapha Sy, mane day koulà beugue là,guirr sà baye Serigne CHEIKH Ahmed Tidiane Sy rta. Wayé,liimay gnanne yalla nà djaabotou Cheikhal Hadji Malick rta, yeupe dône bén☝️,xol❤ yii dône bén.Téh yalla mousallén si séytané.Yalnà yalla déf sûtoureu 🙏Amine
Kou beugu nopalou topal alhourane ak sounna naw magu gni lol xamni ay diambar lagn wonne mai niak topp tarikha yi doula wagnil dara sa diné ..yewou jotna
Moi je fait un appel à Serigne Mountaga mbacké khalif général des mourides essaie de réunir cett famille pour les réconcilier Mbacké svp🙏🙏 jsuis mourite ms j'adore ls Tidjaniyas
Franchement ki ku tok diko deg lu sah yah mom yéna Yam ... Bo amatoul lo wkh say talibe nga nianal léne niu gnibi bayil politiques bi ah wahi dofff yi ngay wkh
@@abdouly6773 ki naniuko setane rk sekka talibé yi nio wara yewu sa serign bulay wkh ay wkhi dof ah wkhi politiques nga am fouleu diok rombako ... Ki jarul sah Mouy djuli yalla dji sah beugul kouy xawi soutoureuss nith rawatina di soosss ... Mé alhamdouli bila nith gni andah seni xel biniula geumulé ... Xawma ndeuk niu dof dila deg lu ...
Le respect est réciproque Serigne mbaye sy Mansour c'est ton père ♥️ nitt del sédé si mom Lou rafét way liguay déf bakhoul nak chaque année gua wakh Dara Moss gua wakh guiss gua yalla🤣🤣🤣 astafiroulah
Bilahi nitt dina ligueye ba Wara djarignou ndiobotam yakkeu ko .Seydil hadji Malick ak limou bindeu si Mouhamad PSL loulo reik doyna wakhtaneu. Amo Loy deif loudoul tokk di yakk sa deireite. Lo meunoul rakhass mouy mbokk rafet thi Yalla naniou yalla deif Ay talibè cheikh deugeu tei niou top yalla🙏🙏🙏🙏
Enfin de compte Serigne si vraiment yeneughi rereul peuple bi li rek moy wanéni kou topoul yala yonentébi ak saye wadiour perte gha
Lou lére nga wakh
Dindil foto porofil bi
@@mallbelly8250 😂😂
@@mallbelly8250 💔
Blhi deug rk nga wax
*Nous aimons serigne babacar Sy Mansour ta dra douko dindi*
*Yalla naniou Yalla djegal sounouy bakkar Serigne bi li nga wakh reuy na bouddonn lou am sax waroulo ko wax waxumaak nak Damou sheikhal Khawmi*
*Yalla baxna 😢😢😢😢😢*
nagneko bayégue yalla rék
Bilay da yook souniou beuguel thiii môme sakh Serigne Moustapha bayinakoo
🤣🤣🤣 ay doff
Toplén serigne siii rek
@@issambengue3082 inchallah bou bakh
Aka bari xam xam lolll son organisation et parfaite
Mai bene défaut la am moy dafa iniane jamais mou dakor si li yalla deff
Pour mom warna yilif adouna président bou nieuw joxoko nop mou xass la meme macky sall sukoy critiqué dou objectif personnel
Serigne amga presk 70ans kone amna lo waratoul
Maodo nak nena barina kuy wotei batine fii si adouna euleukk neinne rek la yorr
Serigne Babacar sy mansour yalla nafi yalla tei werr
Amine🙏
Mayma t-shirt
DEUG nekhoul
Lii niawna si dioulit basi niou bokou yalla na yalla tapée xoleyi ba xalet di tope si ganaw mak lolou mo derfar mak
🤣
Kou beug Tass diinée si réweum d'où andak kokou begeu yax lalay DF du andak macky mi nane nouvelle ordre mondiale té lak yallah may mayou KO fi ken l'on doyéwoul iniané ken len kou NK lala yallah sed RK yaye borome te point......
Keepp kouye Tidiane am gua loula metti
Walahi amna louma méti tay
Pas que les tidiane je suis mouride mais nékhouma
dou tidian kacé la métti man métti nama lol bilakhi
Bilahi Jai honte
Bilay dama rous
Suivrons ensemble Dieu et son prophète : c'est la solution.
Moy solution bi déh billahi
bilahi moy solutions bi Sénégal légui niouy fowé dinè rék niofi néke alkhouran ak souna rék moy solutions
Wallahi 😭
Vous êtes seulement hypocrites.... mais les sahabas même se sont entretues entre eux.....
Ces problemes ne sont que l'œuvre de ibliss... donc epargnez nous de votre ignorance....
Moustapha sy mi bakhe na rk
Man dh mourid la talibe Mame cheikh anta mais li mom rafetol Mame elh Malick Sy ndiabotam waro gno tok Di wah yen wah yi guen Balma nak yalna yalla doli sotoura ak khelmo rafet barke Serigne saliou
Bo xamul daguae nopi
Niaw na lol
Walahi limou wax amoul mais wax dji bétouma deeee kou dioubowoul ak say frere dou dioubo ak say baye
Dugale lousa yone nék bayi léne gnu reglé sén problème ensemble
Moi je suis mourid mais je ne comprends pas comme ça
BOUMA SAGNONE LI KHEW BÉNE TALIBÉ DOUSI WAKH 🙏NIT KOU SAGNE WAKH BAYIKO AK YALLA SOUNOU BOROME NIT BO NATÉ WAKH BA KHAM NIMOUY DEF SI KHOL NGA WAKHKO SA MOROMOU GOR GUIR OUT LOU MÉTI KHOLAM BOUBOBA YALLA MOY RÉAGIR NA GNEUP NOPI TÉ AM TALIBÉ KILIFEU YALLA MOKOY FADIAL MÉRAM NIT BIMA GUÉNEUH RAGAL SI ADOUNA MOY BIY HEUY SOUBA BA NGONE DI OUT LOU MÉTI NIT KOKOU MO RAW MALAKA BIY DIEULSI ROUYI NDAKH MOLAY RAY TES KEN DOUKO YEUK 🙆♀️YALLA BOUMA YALLA MAŸ KHOL BOUMAY WAKHÉ NIT LOU GNAWWW 🙏 TALIBÉ CHEIKH BA FAWWWW❤️❤️
Bilahi wakh dafa graw
Nono sou talibe yi nope day yombou de kii trokhalna talibe yepou man mom dioy naa sakh lii ñawna
CV bibiche mbaye
Il avait dit pire à Mame Abdou Aziz Sy. À l'époque réseaux sociaux amoutone.
@@zfsamt525 li pas du tout bon dans notre pays
Thiey yalla na yalla May diamou sènègal mouseul niou si saytané 🤲😢
Bi lahui yawakhe deuge
Amine way
HAwa Amine yarabi
C'est genre de personne ne mérite aucune respect
😭😭😭 mame maodo malick sy ne merit pas sa non non non😭😭😭
Franchement 😢 Est ce que aussi fébarou Macron bi diapou ko 🥳
Aida Diallo moustafa sy couple malheureux
@@diopndiaye3581 respect waye qui seute la waye aida Diallo bocoul si keur Sergine touba
@@jaimemonpays9079 seutt ba keine douko wakh deugg khanadou nite
Daga daga
Je suis mouride et avant tout musulman c prkw limome rafetlou mako dara bilayy dama metii amna yo khamni kilifa douko def dakh polémiques rek lay indii😳
Mouride nga khamo do nopi
@@serignendiaye1213 ya kham dara yaw
@@madeleindiouf7615 mo takh wakhou ma
@@khadykebe4736 pardon ma ngi toube dé dama fok ni tarikha Bo si bokoul rek khamo lou fa khew nopi Da lay warr bou néké nit kou manou nga nakh wakh bo guiss ame na lou ko waral wayé balma Da ma fogone ni talibé borom touba nga nakh mome si loumou kham rek la done dokh ak wakh 🙏🏾
@@serignendiaye1213 je parle avec ceux qui ont de l'éthique donc vas consulter ton dictionnaire bref il faut penser au conséquences nous sommes tous ensemble.
Franchement j'ai peur pour se pays li dafa niaw billahi je suis dégoûtée comment on peux tenir des propos pareil ?
Lima thi sof moye saytané yi nék si wétam wakh ta inetéré rék
sale nafeque vous n'aimaez pas entendre la verité
Niou délou Sante serigne Touba yakari diamm yi. Mouride niou wadial 18 safar inchallah. Serigne Mountakha Mbacké yalla nafi yagg té werrr. Ndiguél rk barké cheikhoul Khadim
Santé, ak mandou, tey yeene djaame, djaadjeuf. MOuride
Waw waw mouride✌
Degal nitou fane yii😂
Hors sujet
Merci beaucoup nioun talou niou li
Serigne bi liga wakh réyna dei😔😔😔😔
Mon ame deh
@@elhadjimbengue4664
Sérieusement
Vous êtes comme des moutons 🐑 enchaînés ...
Vous ignorez l'histoire c'est la raison pour laquelle vous donnez de l'importance à cette personne
Aida Diallo moustafa sy couple malheureux
@@elhadjimbengue4664 iow wer ngeu dangka fequé nitt da ngay mandou.
N'importe quoi
@@justme-fl7dj Vraiment
Je suis mouride mais j’aime pas voir ce genre de choses. C’est honteux
Moustapha Sy ya boonne,sa gamou tok fa sakh bakar rek nga fay dieulli, Serigne Babacar Sy Mansour Aly Khalifatoul Am dou xalate sakh lou boonne ba di ko def.
🤫🤫🤫🤫🤫
Ki domaram la rék
@@maguettendiaye4358 non boul insulté adouna bii dafa doy warr keen khamoul vaut mieux gniou mefié wou thii genrou blm yi c entre eux
@@amadoudiagne439 moustafa louma ko wakh khép nako wakh dji dafa niaw 2 trop
Respect way
Kou gueume ni Moustapha sy dafay téppi leufeul ndm doul beuseul j'aime ❤❤
astakhfiroulahh lii rekk motah Alhuran ak Sunna rekk mo woorrr
Daga xam luy sunna lan moy sunna
Waw dangua beugue wakh kou diapou alkhourane ak souna dou am noone
Wahabi ga sen liguey moy parafito yakh pass pass
Wallahi deug la
Gamou delen wakhtane ci Mohamed t Guen dépasser les règlements d compt
Je suis vraiment choqué !!!cette fois ci tu es allé trop loin et je vois pas quel intérêt tu as de vouloir diviser la famille jusqu'à porter des accusations aussi grossières.
je n arrive pas a le comprends quesquil veut à la fin
Dafa dof t yeugouko
C'est Triste
@@julodaigne4172ioe mi ya doff te yeugoko imbrcile yi ngene done do lene sakh rousse di saga kilifeu dinee yi dem lene ngene ndy diangui arkhourane sen ecran yi rk ngene tokk di wakh waye so guenone thi mbedd bi di na la door ba tokk sa kaw😡
Cheut jai trop mal 😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭
Dama rouss bilahi😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭
Doyna war.
@@mouhamedthiam9048 trop sax
Domadabo
Wa li mome gamou la walla 🤭mes kilifagui rouss ci guéne gui mbindéf boudé Lou ame la sakh dou wakhi biss bou sélle bii🤦
Limou wakh dara si amoul.
Il se nourrit de la désunion comme le diable.
Walahii wakhatiko Mame Cheikh gamou boo khamni amoul benn wakhii borom besbii loudoul de graves accusations, kenn masouko guiss,astakhfiroulahh
@@nekifafa3169 yémé na de baye
Lii réglementation de compte la .c'est honteux lou tol ni Goudi yonnety bii
Ki gamou woul dé da nieuwone pour khassté
Serigne mbaye sy Mansour nitou yalla la tolouna fo khamni si yalla bo donn Rey dou dem si ay diabar dakoy defal bopam....je suis mouride mais liii niaw Na trop yalla khamnako.
Geumeutougn ni sakh yalla moy rayé avec ça ngani nitou yalla nga🤦🏾♂️
Mdr le seul commentaire objectif
Lou leer nga wakh
Khamall losiy ndei wakh ki day doulll rek
Je suis mouride mais limou wakh dafa eup trop mom damako meusse begue mais séparation bi sakh diarouko wone tarikha bou Khalife bi wakhé rek lolou lagnou wara déf diam mo guene lép yalna niep am diam seul le Sénégal qui gagne ❤️❤️
Bilay Mann mouride la mais lo mom rafetoul en tant Sénégal jaam rek lanou xam Li mom c'est une exception. Yalna niou yalla dolli jaam ci barkey BAMBA
@@amadoundao8334 bilay iow mais dafa dioum yalna yalla yokou diam rek thi barki cheikhoul Khadim ❤️❤️❤️
@@diarra_chou8497 naka yalla dieggal té tegatt KO ci yonn ci barki borom Touba
Serigne Moustapha nous fait honte vraiment. Képp kou yakar ci Cheikh dara, bayabou nga séti bénén Serigne. Kii dafay yakhe keur Maodo.
Walahi bou done deug sax warone nakoo roussa wakh 🤔🤔🤔
😭😭
*Daw serigne modou kara lawone rènn serigne mbaye sy ok*
😭 nagnou mougne rékk hamni moy souniou sarahou Tarikha bi
Bane tarikha
Dee lene ak sene mair
Dee lene ak sene mair
@@mallbelly8250 yaw merde nganan so meroul nga retane
@@mallbelly8250 mére jamais sérigne mbaye sy dafa fess déle sougnou hole
Liii lep rek saytané la rek....je suis mouride mais Serigne mbaye sy Mansour kou bakh la kilifa la té modeste lol ndeye.... yalla Na fi yaagu lol té wer... mais Serigne Moustapha mi momm dafa foogu ni dafa dioum rek si kaw boudé waarnako wax...meunone Na gamou gamomm rek waxtani si goudi ak borom goudi wayé lii mom niaw Na lol yalla khamnako.
Mourite néxxx nah ❤❤serigne mountaxa yalla nafi yagg téh wérr mourite yi dano beuganté sénn birr mais ay liguéyanté
Yow de doo mouride, mouride dou bègue lou niaw
Yaw daga réré seringe touba mouride dage dou kontan si wak dou niaw
Mo yaw xana dou yèna done rayanté fii barki démb si Magal gui. ( Aida Diallo ak Kara ak gnénène ak gnénène) nguay am loy wakh. Un vrai mouride ne se réjouit pas des disputes des autres. Yaw démal ngua xoll fo bokk ba paré bala ngua wakh si ay diambour
@@aishadiop1067 amel naleu 5000 😂😂😂😂😂❤️🙏
@@madeleindiouf7615 dagno gnémé sou dara amé rék gnou beug indi affaire séytaané entre tarikha yii. Mais dotouko défati😏
k dieu portege notre paye
Ndiabotou seydi el hadji malick sy touti nga thi diakhassé ko. Genrou espesou serigne yi rekk gnoy tal deukk
L'âne moosi sa yoone yene khamo leene tous
@@mallbelly8250 ioe y’a kham dara 😔😔 Li c’est honteux et irrespectueux de sa Part
Wawe yaw daguaye défendre ni jai pitié de toi c’est honteux
Démal tokk
Njaboot gui nak meusta dioubo dh mtx bi mame abdou niewei regler leip té guisgua bim démé affaires yagui ni ça recommence malheureusement 🤧🤧
Dieureudieuf cheikh Akhmadou Bamba khadimou Rasoull Dieureudieuf borom Touba Dieureudieuf borom touba Dieureudieuf borom Touba Dieureudieuf borom touba Dieureudieuf borom Touba 🙏♥️🙏
Yaw dongou morid morid dou contan si wak dou niaw
J'invite les gens faire très attention à ce Moustapha. Serigne sidy Ahmed Sy est né en 1933 et serigne mbaye est né en 1932. De surcroît, il (Moustapha) a tourné le dos à Serigne pape malick sy. Allez regarder son discours de l'année dernière. Mais, il s'est trompé de cible ndak serigne Mbaye nitou yalla la.
En tant k Talibè Cheikh je ne peux rien dire WAYYÈ.... Il n'a que des talibès très jeunes qui ne peuvent rien distinguer pour le moment ndeyssane
Yaw yay premier nonou MAODO 😭😭bilahi ya bone ya séw ya kham lou bone diko wakh dama roussss😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭
😂😂😂
no no ki nite mauvaise langue pervére honte pr humma islamikebi ta trokhol tidianeyi trokholo khalif bi mé gnoune tidiane yi gnou roussati yow diarroul gnou laye serignetou parke tu é modi je te déteste du plu pronfond d mn coeur tu é le diable en persone
Yénn ay khalénguén motax
C pas sûr
Alkhouran ack sounna drra dakhouko billahi
Lan Moy sounah?
Machallah
Billahi wallahe mol rek
@@dmte6440 *waxé yonnénte Bi Ak Diangaléy yonnénte Ak hadis yi moy Sunnah*
Bilay dumassi wakh yalnaniou yalla defal soutura encore on est des musulmans avent detr mouride ou tidiane ou niassene
Yalla na yalla def diamou si rewmé barkép s Touba cheikh ahmadou bamba khadim Rassoul
Nous vous prions de ne pas écouter les propos de Serigne Moustapha Al makhtoum qui accuse le khalife des tidianes si il le disait à vos pères est ce que vous apprécierez ces mots
Abonnez vous à tivaouane 7tv pour avoir toutes l'information religieuses d'ici et d'ailleurs
En tout cas waxone nakofi manilén yallah nafi wax kham kham rék
Après dég nafi lou nék
Wallahi tarikha cheikh bén khalifa mofi nék témoy biniouy falé si Khadaratou yallah ba té fal naniou Serigne Babacar Sy Mansour
Yallah nafi yag té wer ak bép kilifeu diné amine
Walahi Sénégal diam rék mofiy am lou way déf sa bop barké Serigne touba man awma loumay tit si Sénégal ☝️
Allha hou Akbar mon cœur va mal sama khole nakharina 😭😢😭
Trooop sakh
Trooop sakh
Dieureeudieufeti Serigne Touba diarrama Mame Cheikh Ibrahima Fall Lamp sama yakkar dji. Yalla na diamm yagu .Yalla dou fayy wakh bayi dieuff .goor goorloulenn yalla nalenn yalla djoubalé.yennou nenn
Yaw da nga sokhore da nga bonne da nga reww
Dangaye doul
Kouy has sakilifa koula topo has kilifam bilahi walahi amo benae tègin
Yaw te nite kéne guenoula reww wax daniou koy rafétal
Bilay
Yow nak lo def
Serigne Moustapha loumou wah deugeula khalifa féticheur sénégal pouvoir ak khaliss diaralnalén louné niane nioy sacrifiè ak di égorge les enfant
Bilay amna lou manque si mom
No weroul dé bilahi
Aida Diallo moustafa sy couple malheureux
Ki dou dioulite dou nite mane na féne
Ki dafa dof
Il et fou c gua la
Dieuredieufé Serigne touba Khadime rasoul
C est vraiment désolant li dh dou wakhou kilifa
Aida Diallo moustafa sy couple malheureux
C du n'importe quoi et très dangereux. Il n a qu a faire son chemin seul et laisser les autres. Il n étais meme pas en de bons termes avec son défunt père. Pas de levons à recevoir de lui .il veut diviser et affaiblir la famille SY .
Bilae waxatiko kilifeu dou doxalé ni 😭
Merci baye la solution rék
Et ça on appelle ça "kilifeu dinné" au Sénégal 😂😂😂😂
Réveillez vous chers frères et sœurs. Gueum lenn yalla kessé ak sen bop !!!
Tu as raison. Le plus important c'est la religion Islam. Mais pas tous ces Tarikhas qui divisent. C'est la course à la richesse et au pouvoir qui font dériver ces "GUIDES RELIGIEUX "
Kayy nittou safara nguén
@@mayramesall8804 doulga
Wallahi YAllah rekay degu
Mane deh douma tidiane waye sarigne mbaye sy aka mako sop te buegue ko ndakh foulam ak faye dame dokhoul si daray niak fayda yallna fi yagui te werr ak kou wakh amine🙏🙏🙏
Yew yama bettu mane yew rek laa beuguene wante Bess niki taye yew kesse laa bagne yew baakho amo yar amo teguine 😯😤
Mabel gay cake diakhalenama wholesale ligaye vakhe
Bilahui y'a wakh deuge
Legui. Si ç la vérité nak mandoul mo guene khamo lou khew
Salam nitt dou bagne nitt mes loumou wakh reyna trop métina nieup
Limoy vrai cas communautaire ligua wakh nieupaguikoy nakarlou touchéna bépp tarikha mou Tidiane Mouride Layenn Niassénn etc... wayé Sunu rééw diam rekafikhathie yalla na diam sakh si Sénégal ak adouna bi amine
Thieuy Sénégal yalna yalla doli diamm 🤲😍
Amine way
Amine yaa rabbi
Amine
Amine
Dama yakarni seuytanai moy wakh lo nittt yi legui parsk kadou yimay degue nittt yi diko wakh d'où tayefffff 😭😭😭😭yalnaniou yallla moussal si seuytanai akkkk niniou melll yala naniou yalla khirrrr si Lou bakh khir niiu si yone ba dieum sa yallla khirrr niou si Mouhamed (psl) Serigne mbaye si Mansour sounou khalif yalla na yalla goudal sayyy Faye si barké chiekh ameth tidiane
Suis mouride 100% mais deugue mo nekh yallah wakh bou niaw kene khamewoulene ko goulete wakh bi niaw na trop kilifeu dou wakh lougn koy khebei li metina trop 😭😭😭
Tarikha bounek amena nattou ki moy Nattou tarikha bi ndeysane beugoul kén yilifko
Pure vérité
Ioe Reiw nga dh
Ki kaye yéne rék lako yalla diokh
@@madamefall48 yaw kon kidousa nattou khana islambi dou bènne boum niko yonentebi wakhe
Moy natou bi vérité absolu
Sante na yallah bama beugué ahmadou bamba ❣
Ken dou mom❤️
THIEUY SENEGAL THIEUY ADOUNA MAN DHE YALLA NAMA YALLA MAY BANNÊEN NACIONALITÊE BARKEBE SERINGE SALIOU MBAKCE 😥😥😭😭😭😭 Bilahi SENEGAL
Eupna
6:55 est-ce que vous entendez la voix de Selbe Ndom😂😂😂😂😂😂
😂
Doyna waar dal 😪
Liberel domou diambour yi mo gueune. Danga dieufrou. Danga tegui ndigueulou serigne chiekh. Fi nga togue amoul kene kou sant sy. Meme say frères andouniou ak yow. Talibé yi warnagnou kholat sene bop.
حزب الله ak حزب الشيطان gno fi néh yay khol nak foy bokk mais sa yoon nékhoul ci talibé
Domou diambouryi niou wara libèrer seniyy boop.
Serigne Moustapha sy yalla guafi yague tè and ak wër❤️🙏
Aminn lou wayy wx rk tontoulénn
Mais est ce que gni toke fi Di tathiou gnougui dégue Lou ki Di wakh 🤔🤔
Je ne pense pas dh
Yakarouma ko
Peut-être daniouy nelaw
Je me pose la même question
Moma diakhl
Choqué 😭😭😭 no comment !
Qu’on l’aime ou pas il reste quand même l’homme de la vérité !
Dangay doul de benn Khalifa mofii am teii mom laniouy titeuro mouy serigne Mbaye sy mansour
vraiment li nga wax reyna
Kii wakh ay fenne ba pare guene koye encourage
Toi tu na pas de respect
😭😭😭😭amna louma méti bilae batay meunouma gueumm lii
Wow mann deh franchement khalifa bi moy sama khalife tei mom lay deglou mais serigne moustapha dei kouka soponn laa batay may guiss video bii
Dieuleul nako defense bassonn mais bii mom dafaa the eup
Ioee MAME MAODO dafaa top souna ba kheuy dem ioe seutam nganii yako téguii
CV aminata
Gamou la gnou wottè tè lignou si dioublou moy dèfaratt khol yi fattalikou djikoyy seyidina mouhamed (ص) ak histoiram lou yakhou wonnn si dingattè yi gnou dèfarr ko wayè tamitt sante yalla si bagnou bollè si khètam
Wayè nèkoul takhalè wala diakhassè ay dingann
Yènn borom mouk gaddou yi molnlomi nagnouyy wahh louy diffarr tè bayi louyy yakh nèm deukla
keppou kou beugeu yonou mouride tidiane layéne khadre niassene yalla na melni ndiayéne akk diobénne gnouy kagnanté sougnou birr lolou da fanékh ❤️❤️☪️🙏🏿 beusseul j’aime 🥰 bi
Li sakh dou gamou waron na wote mboumbay mogueun Ana Yallah, Ana yoneitabi Ana Seydi hadj Malick Sy dara loudoul wakhou adouna defante akh wakh Lou niaw lolo takh nga wet guisso sa bene mbok war nga kholate sa bop balay trop tard.
Serigne bi blesse nga khadra bi yeupp 😭😭
Kii paase nako
Aye waye lii rafétoul si famille
Liga wakhe drh amsiiii sokhorrr RK mola diapppp Niawe nga lamine tropppp
Suis choquée
Waaaa kii esk nittt la? Liii bou amone sakh waroko wakh si goudi yonénte bii. Jourou gamou wakhal Nitt yii kouye yonénte. Problème de famille nga régler ko après. N’importe koi wannnn nga Nitt yii gueumo yalla aussi parsk féticheur mounoul ray bakane, yalla rkk moy ray. Ngénnn balma nakkk
Ki dafa rew il veut créé son propre khalifa
Srx
Un peut de respect bokk
Amal respect kii dh limou kham sa baye sakh khamou ko thimmm
Respect way
Búdúl dara sax ki dù sa morom
Il était banni par son père pendant 5ans banimou guéné adina beugouko guiss takhaw nafi gamou démentir son propre père kon sou wakhé li boumou diakhal ken du ku bakh dou nitou dara gnikay encourager diko applaudir aussi dou gnou nittou dara ay cheytanté lagne amna lo khmni ku ko deg doko apprécié réveiller vous guir yalla ak yonente bi(psl). Qu'est ce que vous aller raconter une fois a la maison 0 enseignement lou tolno gamou nga wara yé say nit ci diner ci djiko yonénte bi (psl). Linék sama khol yeup meunou mako fi wassalam
😂😂😂😂😂ioe meune gua féne😂😂dh🤣🤣🤣🤣😂😂😂
Yalla na niep am jam tei meytou détail day yakk lou barri thi communauté ❤️🤲🏾🤲🏾🤲🏾
Deug rek la wakh may len niou diam dieuradieufe serigne moustapha
Mag bou reew tei sagne wakh mana feine mooy kii yeei katou fitt na
Kénn,baalmà Serigne Moustapha Sy, mane day koulà beugue là,guirr sà baye Serigne CHEIKH Ahmed Tidiane Sy rta.
Wayé,liimay gnanne yalla nà djaabotou Cheikhal Hadji Malick rta, yeupe dône bén☝️,xol❤ yii dône bén.Téh yalla mousallén si séytané.Yalnà yalla déf sûtoureu 🙏Amine
yaw nitou fitenanga ya bonne cheikh tijjanne almakhtoum daff la méréwone 7en doula nango réservoir bimou dedo ngakoy sogue guisate ndakh linga wakhone seringe pape malick sy
Ah bon
Lolou khamoumako wone
Ayyy Sénégal bayilénn seuytané yénn sén thotou nday rk kii dh dinguénn ko bayiiii ndakh c la mm famille
@@ndeyeramadiop2215 c la même famille et il accuse le khalif de meurtre 😡doul way
Bouléne nou tégal ndayam foton
@@abdourahimkane1185 respect
Yala na yala def diam thi deuk bi j'ai peur fou deuk bi djeum yala begoul li sakh dama tit mon pays vas mal 😭😭😭😭
Kou beugu nopalou topal alhourane ak sounna naw magu gni lol xamni ay diambar lagn wonne mai niak topp tarikha yi doula wagnil dara sa diné ..yewou jotna
Bilay dafa leer
Walahi je partage ton avis. O Sénégal y'a que des faux marabout et les gens confonds la religions et dieu
Walahi mbokkou mi
Moi je fait un appel à Serigne Mountaga mbacké khalif général des mourides essaie de réunir cett famille pour les réconcilier Mbacké svp🙏🙏 jsuis mourite ms j'adore ls Tidjaniyas
Franchement ki ku tok diko deg lu sah yah mom yéna Yam ... Bo amatoul lo wkh say talibe nga nianal léne niu gnibi bayil politiques bi ah wahi dofff yi ngay wkh
Bien dit
@@abdouly6773 ki naniuko setane rk sekka talibé yi nio wara yewu sa serign bulay wkh ay wkhi dof ah wkhi politiques nga am fouleu diok rombako ... Ki jarul sah Mouy djuli yalla dji sah beugul kouy xawi soutoureuss nith rawatina di soosss ... Mé alhamdouli bila nith gni andah seni xel biniula geumulé ... Xawma ndeuk niu dof dila deg lu ...
Amal yar
@@jopbegue1143 boule takh ma saga ndayame
Amallénne yarr soudonne sénne baye dolénne koo wakh liii
Parle nous yalla
Gnommm gnepeu ammm ammm nagnou loulén yalla mayy konnn mandou lén ciii
Do nitou Dara😭😭gni manké dila deuglou tokk sa tant bi nioma métii ligua deff ni yalna nakhari souniou borom tei souko nakharei yalnalako fath🙏🙏🙏🙏🙏🙏
Le respect est réciproque Serigne mbaye sy Mansour c'est ton père ♥️ nitt del sédé si mom Lou rafét way liguay déf bakhoul nak chaque année gua wakh Dara Moss gua wakh guiss gua yalla🤣🤣🤣 astafiroulah
Yaw seuye tané gua
@@fatimgueye5663 ma ndey tayy yaw l'an mosi sa ndey yon
C'est très troublant
Li dou wakhi djioulite
Mou tay
Bilahi nitt dina ligueye ba Wara djarignou ndiobotam yakkeu ko .Seydil hadji Malick ak limou bindeu si Mouhamad PSL loulo reik doyna wakhtaneu. Amo Loy deif loudoul tokk di yakk sa deireite. Lo meunoul rakhass mouy mbokk rafet thi Yalla naniou yalla deif Ay talibè cheikh deugeu tei niou top yalla🙏🙏🙏🙏
لاحول ولاقوة الا بالله العلي العظيم
Mane barké seydina mouhamet dama rousse
Tarikha bouné amna Aïda Diallo
Sa papa ay Diallo sakh moko tane
SawaY boulniou dougal si YoYou sounou Yone nekousi
Kikay aida diallo sakh moko guene
Walakhii manguii doguaa degg deugg sw outré😭😂😂
Khanaaa😂😂😂
Vraiment c'est désolant