Leral yi amna solo machallah, wantei sou nguen ci meunone boler daal, teguine ak khol bou yatou dina geuna am solo , ay mer ak khassantei mom dou jiko Yonentei bi t moy souniou royoukay 🙏🏿
Cest une evidence mais chers musulmans votre methode ne peut porter ses fruits car en discreditant les autres ,vous allez pas concaincre les autres à voir la vérité don't vous faites part. Sene djiko laniou wara khol dilene nié
Alpha wakhal mbok yi gay andal ci live bi niou am dal téy té wané yar gou matt biniou Yonenti psl diangal ❤❤❤❤❤❤ na niou comprendre sunu mbok danio rér kone niou wakh ak niom té nangou encaissé Yalna niou Yalla may niou topou Alqu'ran ak Sunnah ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Oustaz ALPHA wakh deug yallah vous n’avez pas laissé cheikh développer je commence à douter de vous wakh deuk yallah cheikh a bien argumenté par rapport à vous
T’as passé à côté tu n’as pas bien écouté la conversation, mais plutôt tu t’es embrassé dans le sentiment raison pour laquelle la vérité vous passe à travers les yeux et à travers vos oreilles
@@KAADUDINEEJITV toujours pareil a vous même pour ton info suis dans aucun tarikha ok. Et vraiment si je décide d'adhérer à un tarikha ce serait celui de la Tidjania. Vraiment Cheikh a donné une très bonne leçon a Oustaz Alpha et a vous tous qui ne lui laisse même pas l'occasion de développer au lieu ça vous lui juge seul Dieu a cette pouvoir " deux de vous la même insulte " . Lol 🤣😂
كلام باطل وكاذب وكافر ينشره ابن عربي وأصحابه أن كل عالم على طريق القرآن والسنة جعل كفاراً وبايه الذي لم يكن إلا تابعاً أعمى نسخهم ليصنع لنفسه اسماً لكنه يبقى لا أقل من مجرد الفكر الكافر. الدين هو قال الله قال النبي . وليس باي نياسي الذي كان مجرد كاذب جاهل مدّعي Té degue arabe tahoula ham religion
@@MamadoulamineBadji-cy8ud ma mère et mon père sont décédé Paix à leur âme je vous serai reconnaissant si vous faites une prière pour eux et tous les morts, merci d'avance
Yallah nagnou yallah def deug ay talibé Baye Niass ya rabbi Té yéne gni yakar gnoune dagno rére (ibadou yi) fékhé léne khami sen bop avant tout Nah yallah wakh kham léne ma ba paré dogomay diamou
Soyons discipliné si on parle d AllAH le tout puissant la connaissance divine est vaste nul n à le monopole de la connaissance les dimensions spirituelles ne sont pas égales soyons ouverts de cœur d esprit
Confirmé ni yalla amour mèlo té Mosso ko guiss loulou d'où yone néél si ay mandarga lay féniou ok Limay laadj oustaz moy est-ce k yalla am n'a mélo baham wakhnaniouko si Alkhourrane ? C juste une question 😊
Salam yen ikhwa dioum gueen deh andeuleen ak yar ak tegguine. Li keneuh diangal louleen ko. Ay sounnite warougnou saga ak weranté ak khassté si dîna. Lolou bokoul thi oussoul da'wa. Yoninteu bi saws waxnañu soy wax waxal lou rafet walla nga noppi.
@user-kv9ht2pf7r Peut importe son comportement il n'atteindra jamais celui de firawna. Pourtant Allah en envoyant Moussa et Hâroun leur a dit: Adressez vous à lui avec douceur afin qu'il s'en souvienne" " و قولا له قولا لينا لعله يتذكر أو يتزكى" Celui qui fait la da'wa a des règles à suive. Faire la da'wa que tu sois Prophète ou pas demande de la patience et de la compréhension. أهل السنة أرحم الناس و منهجهم أسلم و أعلم و أحكم Les gens de la sunnah sont les plus miséricordieux et leur voie est plus sain, plus savant et plus sage. Je fais la nassihah ( laayé biiir)
uustaz bi kom toungkara koi 😀zero science Mais ceux qui sont bien enracinés dans la science disent : "Nous y croyons : tout est de la part de notre Seigneur !" Mais, seuls les doués d’intelligence s’en rappellent...(sourat3) yalla borom xel la sokhla
@@MamadoulamineBadji-cy8ud sa baye yow moy mbam khoukh sa ndeye di mbam seuf motakh yow nga nek métissage mbam khoukh-seuf,loma wakhate sa bopou nga ko wakh,imbécile sa thiotou ndeyou ndeye
C vraie que si cest vous qui demandez des preuves sur la croyance des tarikhayi avec leur preuve pour remettre les talibé sur la voie de droiture alhourane ak souna donc cest a vous de montre preuve d'abaissement,de souplesse car vous etes assis sur des preuve claire celui qui connaît et celui qui ne connaît pas cest pas la même chose vous aurez affaire a beaucoup de facons oustaz alpha chapeau a vous
Li baye niass liguey si diiné dou sén baye wala sén Serigne biuko liguey si diiné Gueno lèn gueum yala baye gueno len ko dakh jouli gueno lèn ko begeu yonenté bi gueno lèn ko kham yala gueno lenko begeu xam ak degg alkhourr hane Li yeup nak la déf si ay talibém kouci mélo woul mélo yi ya bolé sa bopou si keur baye wayé baye wakh na ni boko si Baye niass nak moy Cheikh al islam grade bobou Sénégal moko liguey moko fi am nangou wala nangou rek mbidef menou si dara
@@Mouhamad-u6f gnoun baye niass daf gno begueu lo yonenté bi daf gno xamal gnou yonenté bi Yaw déjà gueno begueu yonenté bi baye niass Gnoune talibé baye gueno len gnou begeu yonenté bi gueno lèn gnouko topou Sén problème moy aggo lén si xol mbidefou yala té dolèn guiss si mom loudoul boromam biko sakk motakh sén xol yi sétoul toujours yénangui am mbagnél si djam yi yakarni yéna lèn gueneu yéyy si diiné dji wala yén rek la fi yala considéré
@@Mouhamad-u6f ay djoulite les autres safara lane dieum yén déjà momo lèn safara en plus ninguén diapé yala borom bo xamni yakamti woul loudoul akhlou tarikha yi lakka si safara nguén diapé yala béna bour bou sokhorr bou sadik té yala mingui bakh bi pérou bakh ba wakh ni diam bi sou défé béna bou bakh ma defal kako foukk bou défé béna bou bone ma may ko mou diégalou ko sinon béna bobou rek lakay bindeul Té yén li talibé baye di toudou yala diko djouli si yonente bi di zikr istikhfar khaadj khadiatam défo lèn ko
Mane guissaguouma kilifa niassène boudoul ndiabar. Yalla na ma yalla dioubal mou dioubalè mboukou niassène yii .ndakhtè gnome gnèp degnouy bokkalè yalla bou mettè metti. Wallahi
Oustaz Alpha Wallahi ki waro wone wakhtane ak mom, parce que il nest pas humain, ki meunoul wakhak nit, daffa tres insolent et irrespectueux. AlQuran ak sunna moy deug
Billahi ibadou nio nek si deuk
Yeen ibadou toi njalooo rek guen fi nekei
Deug la Ibadou yi ñio nek si deug bou werr 👆🏼💪🏽
Khamou noiu lofal daym
@@adamangumnjie4488yallah xam KO nék si deug alahira la gnouy xamer deug douffi ibadouyi dieguer gougnou sirate déh
Yalna Yallah bal nieup té defar xol yi ❤. Baye NIASS rék
Alhamdulilla ,Yalna yalla fayalfgnou Cheikh Ahmed tidiane, Baye Niasse ❤❤
DIEUREDIEUFE BAYE NIASS
SANS LUI ON SERAIT COMME ALPHA BA
Yalla dou balé bokalé dé..reflichissez les freros .l'ordre d'Allah arrive ne le hâtez pas !@@papaamadoudiagne7059
Yallah nagnou yallah def deug ay Talibé Baye Niass
@@papaamadoudiagne7059 malheureusement kone naro ame xam xam, tchi rer nguey deuk 😅
Leral yi amna solo machallah, wantei sou nguen ci meunone boler daal, teguine ak khol bou yatou dina geuna am solo , ay mer ak khassantei mom dou jiko Yonentei bi t moy souniou royoukay 🙏🏿
Machallah deugg nga wakh
Dieureudieufé baye Niass 🥰😍🥰🥰😍🥰🥰😍🥰🥰😍🥰🥰😍🥰
En tout cas daal kou fi topp lenen lou doul Al Quran ak sunna ya ngi si lou wooreudi 😢
😂😂😂 j,ai même eu un debat avec un talibé indisciplinement arrrogant, deugeur boppu ta
Mais nioune topouniou loudoule sounna ak alkhourane
Vous n’êtes pas des pédagogues je suis désolé
Cest une evidence mais chers musulmans votre methode ne peut porter ses fruits car en discreditant les autres ,vous allez pas concaincre les autres à voir la vérité don't vous faites part. Sene djiko laniou wara khol dilene nié
Wérénté bi nguéni déf ni lane laniousiy diangué nioune? khoulo khasté thiey Sénégal😢
Vraiment il y’a des gens parmi vous qui se fâchent très vite 😢 dioulite dey andak daal té meuneu mougn 😢
Yalla n'a yalla feye Baye Niass ❤❤❤
walahi baye niass kenla
Doungène Ay none yèn gnaryépou Ay dioulit ngèn wakhtanlèn badioubo❤❤❤❤إنماالمومنون إخوة فأصلحوابين أخويكم
Alhamndou lillah yalla nanou yalla saxalall mbeuguelou cheikh Ibrahim في الدنياوالاخرة
Le talibe Baye a raison sur la définition de "mélo"
Séne débat bi amoul démocratie,bayiléne micro diambour bi 😂,thieuye baye niass
Alpha wakhal mbok yi gay andal ci live bi niou am dal téy té wané yar gou matt biniou Yonenti psl diangal ❤❤❤❤❤❤ na niou comprendre sunu mbok danio rér kone niou wakh ak niom té nangou encaissé Yalna niou Yalla may niou topou Alqu'ran ak Sunnah ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Oustaz ALPHA wakh deug yallah vous n’avez pas laissé cheikh développer je commence à douter de vous wakh deuk yallah cheikh a bien argumenté par rapport à vous
T’as passé à côté tu n’as pas bien écouté la conversation, mais plutôt tu t’es embrassé dans le sentiment raison pour laquelle la vérité vous passe à travers les yeux et à travers vos oreilles
@@KAADUDINEEJITV toujours pareil a vous même pour ton info suis dans aucun tarikha ok. Et vraiment si je décide d'adhérer à un tarikha ce serait celui de la Tidjania. Vraiment Cheikh a donné une très bonne leçon a Oustaz Alpha et a vous tous qui ne lui laisse même pas l'occasion de développer au lieu ça vous lui juge seul Dieu a cette pouvoir " deux de vous la même insulte " . Lol 🤣😂
Yaw Mii doff plus la🤣🤣🤣🤣🤣@@MamoudouKane-wl4tj
@@MamoudouKane-wl4tj douko Bayi Mou développé par ce que xamnane kimko sekhal Dou thiomo
Non cheikh alpha mo meuneu tannthie nitt 😂😂😂deug deug ma sha allah 😅😅😅😅
Dieu est unique et il est le trés haut. Personne ne peut l'egaler.
Vraiment que Dieu nous protege sur le Droit chemin 😭 amine yarabi 😭
Beugue affaire de philosophie aï makhama aï mélo 😂😂😂
الصفة تتغير والمقام لا يتغير
وكلّ ذي لله
Masha'Allah oustaz alpha ba leral yi Amna solo yallna yallah fay len ❤❤❤
جزاك الله خيرا ياالف🎉🎉🎉
Salam alaik cher admin j’aimerais bien savoir quelle heure se tiennent vos live❤
معرفة بالله أمر شوقي لا يفهمها إلا أصحاب الشوق.
كلام باطل وكاذب وكافر ينشره ابن عربي وأصحابه أن كل عالم على طريق القرآن والسنة جعل كفاراً وبايه الذي لم يكن إلا تابعاً أعمى نسخهم ليصنع لنفسه اسماً لكنه يبقى لا أقل من مجرد الفكر الكافر. الدين هو قال الله قال النبي . وليس باي نياسي الذي كان مجرد كاذب جاهل مدّعي
Té degue arabe tahoula ham religion
Wakh nga DEUG dhh kou nanoul do khame
Merci Alpha lunu léne diarale rék nanukoo diarale ❤❤❤❤
@@MamadoulamineBadji-cy8ud 😂😂😂Sa koyou serigne
Dém len outi dépenses les pauvres wakh ci gnou bakh rekk moléne tardel ndeysan
Nelen sakh am ngen ay millions d'euros pauvre gens ndeysan
Yalla na yalla dioubanti talibe tarikha yi 😢😢
Les tarikhas c'est pour discipliné les talibés
@@MamadoulamineBadji-cy8ud ma mère et mon père sont décédé Paix à leur âme je vous serai reconnaissant si vous faites une prière pour eux et tous les morts, merci d'avance
Sa tiapa ndeye
Rérouniou dé
Sunnah ci kau bidah ci suf 👇
Yallah nagnou yallah def deug ay talibé Baye Niass ya rabbi
Té yéne gni yakar gnoune dagno rére (ibadou yi) fékhé léne khami sen bop avant tout
Nah yallah wakh kham léne ma ba paré dogomay diamou
Mashalla lélare bi amna solo lole sakh mashalla yalla dagne koye guisse ak aye beuti bope
Soyons discipliné si on parle d AllAH le tout puissant la connaissance divine est vaste nul n à le monopole de la connaissance les dimensions spirituelles ne sont pas égales soyons ouverts de cœur d esprit
Assalamouha leykoum machallah ya Oustaz yalla sam lén inchallah ❤❤❤❤❤❤
Talibe baye Niass yii gnoom ak sëñ sëriñ kiff kiff 😂😂😂😂
Yow yaye mbame deugeu yow ya halkou non yow yaye khathe
Sa data yaye
@@babslepro9790 genre yi kéna doulén tonto nii danganane alhamdou lilah ndakh lolou rek lani gnane yala ndirou baye kiff kiff
@@ibrahimagaye2907 non gni dolène tonto ay saga dangay sante yalla si wakham dji ndakh lolou lani gnane yala ndirou baye kiff kiff
ki boulène ko tontou talibé cheikh ibrahima lanou mom lanouy meusa done
لم يبقى عند غيرنا علم نستفيد منه إلا أننا نستمع إليه فنشكر الله على ما أولانا
Baye niass ❤❤❤❤❤❤❤
Il faut laisser le niassene parler et chacun doit donner son avis
Niass rek bah Aduna di touki inchallah
Machal lha oustaz alhpa ba 😂😂
Yalna yalla samou alxouran ak sounnah amine yarabi
قال الله تعالى فى القرءان. أدع إلى سبيل ربك بالحكمة والموعظة الحسنة إلى ءاخرلأية alfa sa numéro la beugeu
il faut mesurer les paroles pour l amour d allah. il faut discuter avec sagesse
Billahi on est tous des musulmans on devrait être un seul bloc voir un mure
Molainne guéna diague fopou ❤❤baye niass seul❤
Yalla rék mo kham😢Aÿ way naniou beuguenté té yalla takh surtout nioune dioulit yi
Dieureudieufééééé BAYE NIASS ❤
Confirmé ni yalla amour mèlo té Mosso ko guiss loulou d'où yone néél si ay mandarga lay féniou ok
Limay laadj oustaz moy est-ce k yalla am n'a mélo baham wakhnaniouko si Alkhourrane ? C juste une question 😊
Mashaallah yallana yalla samm oustaz alpha ba
Alhamdoulilah dieuridieuf baye niass deme lenne khame yalla
Et aussi longue vie a vous ya oustaz Ba
😂😂😂😂 vraiment l’est grave, mais se discipline de baye niass
Verémen alpha sa kholle baakhoull😢
yéne mayouléne ko sakh foumou wakhé ..mouléne béne respect
Sunnah rék moy❤❤❤❤ DEUG billahi
Yaw khamo dara
❤daye❤❤❤❤😂😂😂😂😂😂
Abb thiaga momm vraiment waroul wakh si dinné
Salam yen ikhwa dioum gueen deh andeuleen ak yar ak tegguine. Li keneuh diangal louleen ko.
Ay sounnite warougnou saga ak weranté ak khassté si dîna. Lolou bokoul thi oussoul da'wa.
Yoninteu bi saws waxnañu soy wax waxal lou rafet walla nga noppi.
Comment peux u expliquer le comportement du talibé baye ? Il faut bon juge.
@user-kv9ht2pf7r
Peut importe son comportement il n'atteindra jamais celui de firawna. Pourtant Allah en envoyant Moussa et Hâroun leur a dit: Adressez vous à lui avec douceur afin qu'il s'en souvienne"
" و قولا له قولا لينا لعله يتذكر أو يتزكى"
Celui qui fait la da'wa a des règles à suive.
Faire la da'wa que tu sois Prophète ou pas demande de la patience et de la compréhension.
أهل السنة أرحم الناس و منهجهم أسلم و أعلم و أحكم
Les gens de la sunnah sont les plus miséricordieux et leur voie est plus sain, plus savant et plus sage.
Je fais la nassihah ( laayé biiir)
uustaz bi kom toungkara koi 😀zero science
Mais ceux qui sont bien enracinés dans la science disent : "Nous y croyons : tout est de la part de notre Seigneur !" Mais, seuls les doués d’intelligence s’en rappellent...(sourat3)
yalla borom xel la sokhla
❤dieur dieuffé baye niass
Wa mane lima diakhal pourquoi pas kouné guem li nga guem yaw mal khiyam yalla atté pour mane mo guene wérenté bi
Demlene khami yallah
🤣🤣🤣🤣🤣you destroyed the man
Ahhhh li deh metti na wah di yohou nak😂😂😂😂😂
Dieumi baye niass sakh damaye déllo si yalla
Alpha ba danou nga tay
Boy bi wakhnala deug yalla amoul melokan bingané dara meloul ni mom nga niak sakhalal yalla melokan
Waw nég lén side lep dina lér inchallah
Amouleen ndeye argument mo tax guen di waccei baye point 😂❤❤❤❤
Masha'Allah alquran ak Sunnah rek ❤❤
Baye Niass forsou
😂😂😂le gars neina qui il est fou wAllah😂😂😂😂 sheuuu😂
Yenne dem léne diamou yalla mo gueune lou nguéniy def amoul chance nguéniy saga rek yenne nieup nk bayuou massy kenne
Manchallah ya cheikh mais arrête de rire des gens le prophète ne rié pas des autres en moquerie S'il te plaît ❤
yenn ragual lenn yalla,wallahi baye niass nguenn guenouko tegou si alkhourann ak sounna togne bahoul so khamoul daguey mandou
Sunna bi baye niass né kon lai roul
😂😂😂koulawakh lolou
alahou akbar ler nagne niveau boumou wahe guenn deguoul ,baye n'enah d'où meussa worro alkhourannn ak sounna yenn yenna comprendroul
Haha talibe baye gayyi door naniou laa😂
Melo meun na nek djiko
Mélo Ak mandarga Je vois pas la différence !
Contaaaaaaane naaaaaaaaaaaaaaaaaaaaaaaaaaaaaaaaaaaaa!!!
😂😂😂Kidal khamoul dara
Alpha Ba, vous gagnerez aussi a donner toujours le respect a tous les intervenants sans des moqueries des membres de ton equipe.
BAYE IS THE SOLUTION.
ماشاء الله
Loutakh bayiwolène Babacar Mané mou yégalii
Nagnou topou sene werdi yi di dof rék,sénégal thiakhane rek waay kou topou serigne yi ba yakhoule yakoy yek
Xana Kone aduna nieupeu dof
@@MamadoulamineBadji-cy8ud sa baye yow moy mbam khoukh sa ndeye di mbam seuf motakh yow nga nek métissage mbam khoukh-seuf,loma wakhate sa bopou nga ko wakh,imbécile sa thiotou ndeyou ndeye
Amo léne respect si débat yi. Xolat lén sén boppa.
ماشاء اللہ استاذ بہ❤
C vraie que si cest vous qui demandez des preuves sur la croyance des tarikhayi avec leur preuve pour remettre les talibé sur la voie de droiture alhourane ak souna donc cest a vous de montre preuve d'abaissement,de souplesse car vous etes assis sur des preuve claire celui qui connaît et celui qui ne connaît pas cest pas la même chose vous aurez affaire a beaucoup de facons oustaz alpha chapeau a vous
Li baye niass liguey si diiné dou sén baye wala sén Serigne biuko liguey si diiné
Gueno lèn gueum yala baye gueno len ko dakh jouli gueno lèn ko begeu yonenté bi gueno lèn ko kham yala gueno lenko begeu xam ak degg alkhourr hane
Li yeup nak la déf si ay talibém kouci mélo woul mélo yi ya bolé sa bopou si keur baye wayé baye wakh na ni boko si
Baye niass nak moy Cheikh al islam grade bobou Sénégal moko liguey moko fi am nangou wala nangou rek mbidef menou si dara
Amna niou ko guena ligueye chi l'islam té woté wo wognou aye guiss yalla cheikhal islam yonente moko guena for sahaba ko guena for
@@Mouhamad-u6f gnoun baye niass daf gno begueu lo yonenté bi daf gno xamal gnou yonenté bi
Yaw déjà gueno begueu yonenté bi baye niass
Gnoune talibé baye gueno len gnou begeu yonenté bi gueno lèn gnouko topou
Sén problème moy aggo lén si xol mbidefou yala té dolèn guiss si mom loudoul boromam biko sakk motakh sén xol yi sétoul toujours yénangui am mbagnél si djam yi yakarni yéna lèn gueneu yéyy si diiné dji wala yén rek la fi yala considéré
@@Mouhamad-u6f ay djoulite les autres safara lane dieum yén déjà momo lèn safara en plus ninguén diapé yala borom bo xamni yakamti woul loudoul akhlou tarikha yi lakka si safara nguén diapé yala béna bour bou sokhorr bou sadik té yala mingui bakh bi pérou bakh ba wakh ni diam bi sou défé béna bou bakh ma defal kako foukk bou défé béna bou bone ma may ko mou diégalou ko sinon béna bobou rek lakay bindeul
Té yén li talibé baye di toudou yala diko djouli si yonente bi di zikr istikhfar khaadj khadiatam défo lèn ko
macha Allah oustaz Alpha
Ki danou na cou guiss yalla kay war nga kham noumou mèl😂😂😂
Alpha je suis pour ton combat l’unicité mais toi et ton équipe vous avez besoin de tarbiya mais cette fois pas avec des uthaymite
Mane guissaguouma kilifa niassène boudoul ndiabar. Yalla na ma yalla dioubal mou dioubalè mboukou niassène yii .ndakhtè gnome gnèp degnouy bokkalè yalla bou mettè metti. Wallahi
Oustaz Alpha Wallahi ki waro wone wakhtane ak mom, parce que il nest pas humain, ki meunoul wakhak nit, daffa tres insolent et irrespectueux. AlQuran ak sunna moy deug
Da nguénn merr nak😂😂😂😂😂😂😂
oustaz alpha séen wadji tamit daffa wara téey touti parce que débat daffa baakh pour xam-xam féegn il faut se calmer un peu
Dafa woolouwoul boppam
😂😂😂 niaw talibé baye bi khawnaléna ray nguendi sissou,nane dafa réw
Qu'on se respecte sachant que tous sommes des musulmans.
Salam alaykoum wa rahmatoulah. Bayilen genrou live ak genre yi. Rafetoul
😂😂 pass pass bou bon bi ibreu Niass molenko diagal
do bay doul
@@AbsaNdiaye-n5gbaye niass doulkate lawone
@@cheikhassane7925 diguen dadje euleuk yawma alkhima incha alah
@@MamadoulamineBadji-cy8ud bayinala ak yalla te khamne dinagne dadje incha Allah
Deg ak guiss dou mélokane mais maxama la. Moy pouvoir moy kouy ragnél
Alpha bayile wadji mou développe nagouwo mou développe
Yaw laya gui ngay wakh nii mélokanou yala yeup mingui si domou adama deh
Vous qui faites l'émission, c'est vous qui êtes indisplinés.
De vrai fou ces hommes de tarikha,,, tous pareils...
Kay gnou déba
L’autre à côté de alpha trop incorrect respecter le temps de parole des invités
ليس كل كلام يستحق با لجواب غلام أستاذ أحمد باه رضى الله تعالى عنه