Bravo ousraz Alpha bah. que Allah Tout puissant veille sur toi et toute ton equipe. Vous faites un excellent travail qui, Al hamdoullah commence à porter ses fruits. Grâce à ton travail tous les sénégalais de l'intérieur comme de l'extérieur commencent à se rendre compte des dérivés opérées par ces bokalekates des tarekhas. Que dieu vous bénisse
Machalah dieuredieufe oustaz alpha ba dieuredieufe oustaz younousse dieuredieufe sokhna makhady billahi louler nga wakh deug rek machalah sen ligueye rafetna yalla na len yalla faye leral yi amna solo yalla na len yalla faye yalla na gnou yalla moussal si pass pass you bonne yi yalla na gnou yalla wane deug bagne top ko mou wane nen bagne moytouko sang Ndiaye khathie sakh guen
Heeh papa go for Sounnah is more important. Alhagie oustass Alpha Bah .may Allah protect you guide you..save you from evil eye with the whole uhma delivering sounneh..with Allah and faith everything is possible..Inshaa Allah 🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉
Malheureusement tout est à l'envers dans ce village français du Sénégal, s'il y avait un minimum de normalité ce Sangue Ndiaye serait parmi les apprenants
En tout cas Alpha a éveillé les gens mais DIEU a dit de parler de la meilleure manière les gens du livre ( chrétiens). Alors il est nécessaire de rectifier les égarés de la même manière. Merci bcp.
Sangue N’diaye iow da ngay nakh say talibé rék. Yalla rek laniou wara soukal. Alpha ya ngui dioubanti niou bari vraiment Dawah yi mo ngui leer. Au moins si yalla ak yonénti rék ngay diangualé. Mais Sangue mom Serigne lay diangualé té lolou sokhla wouniou ko . Merci 🙏🏾
Des cœur pour Oustaz Alpha et son équipe ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤ ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Allahou akbar all hamdou liillah. Yallah yoow rék yaaye yallah kééne dou yallah soub hana hou wa ta Allah kou doul yoow yallah Mouhamadou rassoul mooye sou gnou nabi Allah. Yallah sou gnou boroom SÉRINGUES yii ak séne yii nii toog mouye doox ccii aye kaacc, sooss kaacc ccii islam bou téédd téh séell bii ak dii leendemeel xééll talibé yii ak askane bii. Allah baraka bii gnou lééne comprendré ndax , la woone woonii na.
Dadji bii deyy défff effet dhé 😂 leguii busnessmann yii amm problème . Le grand père là commence déjà à parler avec le pancréas 😂😂😂 Team Alpha Bâ rekk✌️✌️✌️
Sangue Ndiaye dafa alkou,il est maudit,des personnes comme lui le jour du grand rassemblement,ils verront et sauront que tout est vrai,In Shaa Allah...
Soi disant Serigne dina dakan saneté com djigueune kon Alpha dafa lal fouy mété xam nga vraiment Sénégal nouyou diapé diiné l'islam dou degeu dou yone yow sangeu Ndiaye do nitou dara maloko wax vous nous emmerder à la fi yalla yonentém bou tédeu bi rék mofi nékeu ak sunu téré bi di Alkhourane nou Karim ❤🤲💯
Ndeyssan li diara bayi xel moy yalah amoul loumou teulé وهو على كل شيء قدير thé aussi فعال لما يريد baye Niass limou andi sen wakh yi meunoul téré mou nekk deug affaire nekk yalah wala guiss dou xam xam mo kay mayé mais chance
Alkhamdoulillah yéne gniye déff émission bi ndahh danguène Di yokkou liguéye baye Niass ndah si Yone bi nguéne nékk séne baye yiii nékone nagne si téh téwoul mbirr daye guena yokou dieureudieuf ndahh liii guène Di déf ni si liguéyal baye nguéne nékk ndahh djiguéne permet gnou khamoul baye Niass sax dinagneko khame Kone gnonk lène Di diadieufal si séne liguéye Di léne conseiller wadiodiou gnouye wahh sangue barhamou Ndiaye nguéne déf attention si mome ??? Yalnaléne yalla yeureum
Bravo ousraz Alpha bah. que Allah Tout puissant veille sur toi et toute ton equipe. Vous faites un excellent travail qui, Al hamdoullah commence à porter ses fruits.
Grâce à ton travail tous les sénégalais de l'intérieur comme de l'extérieur commencent à se rendre compte des dérivés opérées par ces bokalekates des tarekhas.
Que dieu vous bénisse
iblis
Alhamdoulilahi baniou tassë akk baye niasse mou deff niou ayy nitt you yewou thi ayy nelawou hamm avec tout le respect mé yala nalene yalla mourill kiraye yii❤❤
, Grand merci au Oustas Alpha Ba
Merci de nous avoir fait sortir des ténèbres
Que Dieu vous garde
Yaw midiwah khamodara sagebi loumwah degela
Alkrouane AK suna rék incha'allah ☝️❤
iblis
Jazakallahou Hayran Ya Oustaz Alpha Ba,Dawah bi Mongui dëf effet big time Motakh soufis am problème nitt yi Niongui yéwou dëh
Oustaz je suis vraiment content pour ce travail remarquable que vous faites
iblis
Alpha yagui yak sene marché yii deh ndiaye mi Alpha yobuna fitt deh 😂😂mércie oustaz Alpha yalna sa jame yague waye ❤❤❤❤
Assalamouha leykoum machallah ya Oustaz yal na yalla tahaw lén
Bon courage mon sheikh yalnala yalla takhawou guoudou fane ak werr ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Masha'Allah oustaz alpha younus seck ndanan Baillo mahaddy uncle Ismailla leral yi Amna solo yallna yallah fay len ❤❤❤❤❤❤
Bon courage Oustaz. Le travail est excellent. Qu'ALLAH vous surveille.
Ma shallah oustaz alpha ba Barakallah fikoum
Machalla Oustaz alpha yalla nalén yalla takhawou ❤❤
Al khourann akk. Sounna rekk incha Allah yallah borombii sammniou sakhallniou thii alkhourann akk sounna ❤❤❤❤
We love outaz Alpha ba
Keep on keeping on sending love from New York City but originally Gambian
Machalah dieuredieufe oustaz alpha ba dieuredieufe oustaz younousse dieuredieufe sokhna makhady billahi louler nga wakh deug rek machalah sen ligueye rafetna yalla na len yalla faye leral yi amna solo yalla na len yalla faye yalla na gnou yalla moussal si pass pass you bonne yi yalla na gnou yalla wane deug bagne top ko mou wane nen bagne moytouko sang Ndiaye khathie sakh guen
Merci beaucoup Alpha
الكتاب والسنة على فهم سلف الصالح
QU'ALLAH assiste, soutient et protège Alpha
Tout❤ avec toi alpha ba
soubhanallah , les freres vous faites un travail remarquable. Maa shaa Allah
Je vous adore ❤
Masha'allah sène liguéye bi rafett n'a trop walahi ❤
Barakallahou fikoum oustaze alpha ba❤❤❤❤est long vie à vous amine ya rabbi 🤲 🤲 ❤❤❤
Ndekei dadji yi mongui def effet dh😂😂Jaajeuff et Oustaz yalna Yalla yokou xam xam bi katane bi weir bi ak meune meune bi inchalla 🙏
OUSTAZ Alpha Thia kaname. Finga ték sa tank fofoula ma cha Allah. Mbot yangui fègne
Merci bcp oustaz Alpha ba quallah vous preserve
Masha'Allah kaadu Dinee you are doing a great job much love to you ❤❤❤❤❤❤
Longue vie a vous ya oustaz 💯 ✊ Ba ❤
Maachaalah Alpha longue vie santé de fer
Oustace c'est bien longue vie oustace ❤❤❤❤
Alpha ba rk inchallah
Machallah oustaz alpha ba que dieu nous protège boul ragal dara
Heeh papa go for Sounnah is more important. Alhagie oustass Alpha Bah .may Allah protect you guide you..save you from evil eye with the whole uhma delivering sounneh..with Allah and faith everything is possible..Inshaa Allah 🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉
Malheureusement tout est à l'envers dans ce village français du Sénégal, s'il y avait un minimum de normalité ce Sangue Ndiaye serait parmi les apprenants
daguene di wakh rek Baye di geuneu yok pasceque fou nekone ay foo la talibe dougniou yok Baye mofi eupe talibe merci Baye inter national
Yalna yalla same alpha ba
Younous Ana djeun bi
Oustaz contane si yen bilahi
Vous faites un travail remarquable
Qu'allah vous récompense on est vraiment contane si liguey bi
En tout cas Alpha a éveillé les gens mais DIEU a dit de parler de la meilleure manière les gens du livre ( chrétiens). Alors il est nécessaire de rectifier les égarés de la même manière.
Merci bcp.
En tout cas en ce qui me concerne tarikha mom ça fait des années dëgg lou wouma lén ndakh thiakhane la jërëjëf kaddu diiné ji lérral you ame solo yi❤
Tiosanou tiossani gueine wara dem guestou dji.. Dem leine xami yalla
Tarikha yalla téré wouko bo beugué ma indil la ayaa bi 😌
Merci boucou Merci beaucoup longue vie merci ❤❤❤❤❤❤❤
Yalla nala yalla samm ya oustaz
Alpha qu' Allah vous protège. Sunna rekk
Serigne ba ngni merr de 🤣🤣🤣🤣🤣🤣, Masha'Allah oustaz alpha ba yallna yallah fay la ❤❤
Oustaz yalla nala yalla sam
Vraiment ki khath la soubhanalah
Sangue N’diaye iow da ngay nakh say talibé rék. Yalla rek laniou wara soukal. Alpha ya ngui dioubanti niou bari vraiment Dawah yi mo ngui leer. Au moins si yalla ak yonénti rék ngay diangualé. Mais Sangue mom Serigne lay diangualé té lolou sokhla wouniou ko . Merci 🙏🏾
Al Qur'an ak sunnah moy deug ❤
حفظك الله يا أستاذ
Merci bcq oustaz alpha ba❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Machalla oustaz Alpha ba H.A yàlla nala yàlla sàmmu
Des cœur pour Oustaz Alpha et son équipe ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤ ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Merci outaz ba
Nn wadji ray nama 😂😂🤣
Mais le travail continue dh amoul bayi ❤❤❤
Yeefeer la deh
alpha BA tu as raisons il dit de gros mots
Sa se voi k le message de alpha passe tres bien
Allahou akbar all hamdou liillah. Yallah yoow rék yaaye yallah kééne dou yallah soub hana hou wa ta Allah kou doul yoow yallah Mouhamadou rassoul mooye sou gnou nabi Allah. Yallah sou gnou boroom SÉRINGUES yii ak séne yii nii toog mouye doox ccii aye kaacc, sooss kaacc ccii islam bou téédd téh séell bii ak dii leendemeel xééll talibé yii ak askane bii. Allah baraka bii gnou lééne comprendré ndax , la woone woonii na.
Mashallah❤❤❤❤
Dadji bii deyy défff effet dhé 😂 leguii busnessmann yii amm problème . Le grand père là commence déjà à parler avec le pancréas 😂😂😂 Team Alpha Bâ rekk✌️✌️✌️
Billye wallahi ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
C un signe dawa sunah marche keep up good work
Oustaz Alpha yalla na yalla sammo la
machaAllah oustaz Alpha
Longue vie à toi
❤♥️♥️♥️♥️♥️
❤❤❤❤❤❤ sunna rek inchallah 💪💪💪💪💪💪🤲🤲🤲🤲🤲
Sangue Ndiaye dafa alkou,il est maudit,des personnes comme lui le jour du grand rassemblement,ils verront et sauront que tout est vrai,In Shaa Allah...
Maa shaa Allah
سبحان الله
Thiey Sénégal
Soi disant Serigne dina dakan saneté com djigueune kon Alpha dafa lal fouy mété xam nga vraiment Sénégal nouyou diapé diiné l'islam dou degeu dou yone yow sangeu Ndiaye do nitou dara maloko wax vous nous emmerder à la fi yalla yonentém bou tédeu bi rék mofi nékeu ak sunu téré bi di Alkhourane nou Karim ❤🤲💯
Sangue ndiaye Talibe baye niass bi day fen rek di tek khag bu bon bi 🦮🦮🦮🦮🦮🦮🦮🦮🦮🦮🦮🦮🦮
Merci alpha ba dall dhe😂😂
Soubhamallah
الحمدلله
Machala ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Alhourane ak sounna rek
Hafizahoullah oustaz
OK baye niasse mo deff lolou kouko wedii moy weddi nga seydina aline karamalah ndakh mom ak seydina ababacar sadikh dih wérénttë thi Mala makk ababacar niko Mala makk aline niko kèrokk sah yaye bimoula eumbë gaïnde dakhadji nako thi alleuh bii khossi ko lerouh ababacar bii khégne ko mou bayii koh ababacar deme lathieuh yayam' yayam niko kokou doussa morom kou gueumoull lii doh gueum Dara bilahi😂
Pouvons nous avoir les références svp ?
Merci d'avance.
Oustaz alpha yagui déf effet nak
Diadieuf oustaze alpha dadji Yaangui def effets 😅
الحمدلله هذا يدل على أنك في طريق سلف ،دمت ياألفا باه
Vraiment ils faut être trop con pour suivre les tarikha qu'Allah leurs guides dans le droit chemins
Dieuredieuf cheikh ahmadoul xadiim ❤❤❤❤
يعني في قوله جنةالقلب
Alfa dou sounnou raisonnement dee wayee sa khalatt yaw sa khel mou neupp yaw khamoo yalla khaam ga bo dewee dem safara direct
Khé alpha bayil fén boul wakh né li moy pass passou Niassén ki silou ko nekh
Dadji yi moy deff effets 😂😂😂
Dajji yi Dalna tropp mashallah...
Il n'arrive pas a se justifier..!!!😢😊
waw gore oustas Alpha ba yaw lanuye topu
Machala
❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
😂😂😂 masha Allah Oustaz
Dieuredieufeeeeeeee cheikhou tijani cheriff rdiyalahou anhou ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
الإيمان جنةالمسلم
Ndeyssan li diara bayi xel moy yalah amoul loumou teulé وهو على كل شيء قدير thé aussi فعال لما يريد baye Niass limou andi sen wakh yi meunoul téré mou nekk deug affaire nekk yalah wala guiss dou xam xam mo kay mayé mais chance
Mangui ram wallahi tariha daniouy lay dof lo😂
Sén serigne yi di lekk di naan di poup di saw di dokhote di laale sén djabar yi chak goudi nguén ni ay yalla lagn hay😂😂😂😂😂
Wakh niou iow fo baye ko après niou continuer.. Degoulen alquran Degoulen dinnee.. Solen xamoul de len ladj
😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂
Bayyil caaxaan