Bilahi kom dieynaba tall dama doff si sama papa 😢 amouma si mom sago sou sama khol nekhoul sakh sama khel si mom laye dém ma woka téléphone rien que pour nouyouko rek❤ yalla nakofi yalla yagal ak bép joulite
Ndaysan Mareme Sall 😢😢 gathié rek moko ray,bou doundon numuy xolé wat teugue yii vue que Makhoudia moko sauvé, d après Mariama Ba :la honte tue plus vite que la maladie. Mais Fatma Thiam est ce que yaye diou bakh la😢😢
Pa Ndiaga ñiaak,Diouma dafa tolou ci seuyi,meunou loko gardé sa keur bamou mbakhé fi😅.Keur Alkaly tang na fane yi.Yalna diam délou ci fëpp fois am thiow.Allahouma amine🙏
Makhoudia Tall is the best man in this movie, he went through a lot to be with his friend Alkali. Last time Alkali and his son have humiliated him but he still keeps his cool and he didn’t pay back. What a great man. Love ❤️ from the Gambia 🇬🇲 ❤️
Cheut vous parlez des khass de Tické Laobé mais yayou Paco ak ay proverbram wolof j ai jamais compris ce que ça voulait dire mais khamnani punchline leu😂😂😂faut ma def cours renforcement wolof 😂😂😂😂
Ou pas . Baye bou irresponsable di nakharel ce yaye . Baye bo rhamnné daram metoul ligueyo terrain bi gne tabarhal ce yaye sarkh de niou ko diappalé be mou féye ko . Il a parfaitement raison
@@louloutebien plus fatim thiam défoule dara loudoul défendre domam sou ne Kone man sakh ni fatim thiam defa nonou lay defa sa dom di dieul teranguam yobou Marieme Sall mou imiliéko ah nonou rk la mounone dèmé makhoudia si bopam mo soff
Ndeysan evenprod defnagne sen casting 2eme saison sans Mareme Sall ba paré mais les téléspectateurs veulent toujours Mareme en espérant que ce soit un rêve. Wait and see
Vraiment bien fait pour lui di weurr di faséwaté ni kou dof ahh ok parce que am nga ngnétel wa démal keureum amo keur nane dagay geuné waté soff marieme sall limoufi def lien ken wakhoul qui dafa seussss
Dafa niak faida complexé teksi. Famille alkali moko gueuneul diambotam au non d'une amitié bou sincéroul. La preuve alkali la traité de Teugg kharam l'autre jour. Makhoudia bou ndaw door dieynaba avec son etat. Mareme sall la toujours mepriser Mem sa 3eme femme quand il a frappé sa fille elle la remis a sa place Mais méram ci ndiabottam lakoy sippi.
Dieynaba tall et son pere sa fait reference a mon certe dafa tang mais je l'aime de tout mon yayam lama toude ken douma lal bou sma yaye di dkokhé lek wla dra sakh manéko ndalh sma papa amna😢❤❤
Vraiment l’âne la beugone! Yaye yaye la! Di takk di fasse noumou ko nekhe beugue guene ko de chez ses Enfants mou takkate indi! Fatim loumou bone bone c’est chez ses Enfants! Mome Moy guene
Bala ma dé rk gni nane fatim thiam mo gueune bone Marieme Sall khana maréme Sall tay la bakh chaque jrs mou nek fi di hass dieukeur dji ak domou diambour yii may len niou diam
Makhoudia kessé mo nité si serie bi. Il est juste, honnete et loyal . Il merite le plus grand bonheur
Mais ligueyoul ayy diabaram nioko yorr
Ndeyssann ak valise bou ndaw bi
Bly dafa dall trop
Jusqu'à divorcé sa femme .son ami à sa famille avec lui
Mame Abdou Donald wakh bounouné diw bakhna ndakh mbokou yii gno ko wakh
Nitte pour yaw parle pour toi
Ndeysane dieynaba tall elle aime son père beaucoup ❤️
Son papa est Lâche. Leur Fils construit une Maison et lui veut que la Maman Sorte., meunneu ko fassé mais warrouko dakh
...
Elle aime sa mère aussi sakhe seulement sa mère n'est pas normal c'est une bétisiere 😅
Yalla na niepp ame diamb si barkep mouhamed ❤❤❤❤❤❤
Kou beug serigne BABACAR SY MALICK❤sama lep
J'aime Serigne Babacar sy ❤❤❤❤❤❤❤
Waxal souniou lepp baby❤
Alhamdoulilahi biniou féké waté bénéne épisode di Niane yalla diko yagg di setane kéne bagna manquer inchalla 🙏🙏🙏
Aameen
@@ndayesohnakah4858🙏🙏🙏🙏
Amine
Amine
Amine yarabi 🙏
Saison 2 bi da émotionnelle trop 😢 do xam Koy faral
Famille yeupa am problème 😢
😂😂moma diakhal dei family maréme sall damaléna modié yereum mais makhodia ussi
Mane mangui si makhoudia
Setan di dioy sou diekhé niou nopi dama sonou si stress
Man mangui si laobé yi ak déguéne rkk 😂😂😂
@@AidaDiallo-dh9jp 😃😃yaw retan mola si nekh
Kou beuge seydina Mohammed rek l'alal j'aim ❤❤❤❤❤
PSL❤❤❤❤
PSL SVP ET ARRÊTEZ
Bété Bété la série qui n'a jamais perdu sa valeur ❤😂🎉
Bilahi kom dieynaba tall dama doff si sama papa 😢 amouma si mom sago sou sama khol nekhoul sakh sama khel si mom laye dém ma woka téléphone rien que pour nouyouko rek❤ yalla nakofi yalla yagal ak bép joulite
T'es comme moi mais j'ai perdu mon père il y'a 6 mois de la
@SalamataBarry-i3r oh master deko gnanal rek yalla nako yalla yeureum khareko aldiana firdawsi 🙏
Amiine yarrabi mane dé sama boss démna il me manque tellement bilahi
Profites en le plus possible
@@SalamataBarry-i3rmoi aussi tourado dama beug sama papa Septembre le décédé souba lay ame 3 mois
Goor gou nek warna féxé ba amm sa keurou bopp
Yorol sa bopp sa keur
Deugleuh
Bilay gaïndé wakh gua déugg déee
Je suis d'accord avec toi ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Dom bou djiegen xaritou bayam kou dacor lalal ❤
C'est vrai ❤
Mane❤
C’est vrai❤
Mane
Bilay
Des cœurs pour notre prophète mouhamed ❤❤❤❤
SALLALAHOU ALLA MOUHAMAD SAW NOTRE BIEN AIMÉ ❤️ ❤️ ❤️ ❤️
❤❤❤❤❤
❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Sallalahou alla mouhamad
Salalahou Aleyhi Wa Salam ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Makhoudia sonougua té Saison bi demagoul fenn😢😢😢
Bilahi yw😢
Mome khana 😢😢
Na dem si nietel bi rek😂😂😂
😂😂
Chapeau aux acteurs bête bête.Que vos talents perdurent ❤❤❤❤
Kouy tog khar bête bete rek lalal j'aime
❤❤❤❤❤
Ô
❤
Doul
Mane🎉
Ndaysan Mareme Sall 😢😢 gathié rek moko ray,bou doundon numuy xolé wat teugue yii vue que Makhoudia moko sauvé, d après Mariama Ba :la honte tue plus vite que la maladie. Mais Fatma Thiam est ce que yaye diou bakh la😢😢
Absolument
Totalement d'accord avec vous mais les gens ne peuvent pas comprendre
Fatim thiam weroul khamoul Dara on dirait qu’elle n’est pas marié elle et trop bête toujours faire des bêtises domam bou Goor bi nio yam
Nous les torodo on supporte pas la honte 😂😂😂😂
@@RamatoulayeWatt-g5jtoxoodo😂
Perdre un être cher c’est difficile courage à amina 😢
Sama xol doyna 😭😭😭j’aime trop les pères worouko won guéné
Legui mi beugone guènè fatima Thiame fassèko Ndah haritam Ndah haritam Sénégal hamouniou coy dèf cou fayou laniou ham
@@AbyKa-le8kmxanna wave ngaye sétané problème yi sou amé yallak fatime thiam leuh
Fatima li mou nan gay deuk ak mom si keur
@khalil legui li mareme sall défe domou fatim thiam yeup nak faté ngèneko
@@jolieseye403 taxhoul maye waxh lignou def makhoudia motxh may waxh
Fatim thiam moma gueneu soff si série bi bly😢😢
Mo toth série bi di
@@ladykbeye8846Fatim défoula dara loudoul défendre domam
Mo geuna bone Maréme Sall
@@fatoutall7396yagg nako wakh khol bé nioul
😂😂
Théâtre bi Mingui Doga Commence Nak Mashalla ak Image bima done guis si saison 1 bi mofi fegne 😊❤
L'amour ne doit pas être aveugle, mais il doit être capable de fermer les yeux sur des banalités comme les castes. LOVE
Kou beuge bete bete rek l'alal j'aim ❤❤❤🎉🎉🎉
Vraiment Amina c'est une grande artiste ❤
Oh djeynaba tall est comme moi man awma cii sama pape saago mais Yalla nako yalla yerum😭😭😭 j'ai regarder la partie plusieurs fois
Bilahi walahi yala seydina Moukhamet saws kharen adiana firdawsi metina trop lolou monekh yala
Bilaye sama papa sous khoulo wone ak sama yaye sama papa laye farale ndeyessane yalla nalène yalla kharè aldiana mes parents name nalène trop
Pareil pour Moy sama confit
Li man nama dioy lo😭 ken dou geuné sa baye ag Lou mana xew ndakh Lou waye am guinaw yalla sa Baye la kham nane thiatrar la me nan si diangat bou bakh
Saison bi souffrance de makhoudia la waron toud 😢
Pa Ndiaga ñiaak,Diouma dafa tolou ci seuyi,meunou loko gardé sa keur bamou mbakhé fi😅.Keur Alkaly tang na fane yi.Yalna diam délou ci fëpp fois am thiow.Allahouma amine🙏
Sonko et diomaye Allah vous protège ❤🎉 0:15
Amine ❤
Amine 🤲 ❤
Makhoudia Tall is the best man in this movie, he went through a lot to be with his friend Alkali.
Last time Alkali and his son have humiliated him but he still keeps his cool and he didn’t pay back. What a great man. Love ❤️ from the Gambia 🇬🇲 ❤️
He is the best man to his friend but not to his family
@@soxnasi1234thank you he prefer moving with his friends than his family
@soxnasi1234
His family are the reason behind his actions towards them.
They don't want to be good like him.
Mais il n’a pas de boulot c’est la raison pour laquelle quelle sa femme ne l’a pas respecter
Mais il n’a pas de boulot c’est la raison pour laquelle quelle sa femme ne l’a pas respecter
Bon courage aux étudiants
Yalla n’a niou yalla mouseul si kou melni Fatma Thiam
Weuhhhpppppp fasé nagn makhoudia tall 😂😂
Djilbab bu makhudia bi rafet neu dh Macha allah 😌
Laobe yii niomeu rk nioh neik cii jamm 😂😂😂
😂😂😂
Je viens d’accoucher des triplés 🎉❤
On s'en fou
😂😂😂
Félicitations yalnagnou dound té barkel ténga wal mako thi barker Seydina Mouhamad psl 🙏❤️❤️❤️
Diouma thiame yeureum nako😢
Diar nako dh
Toujours là à représenter kolda 🥰❤️
Cou beugue nioyi tek bete bete 3 foi com man rek lala jamais ❤❤❤❤
Yalla naniou yalla defal fekke ak Tal bange sétane kou❤❤❤❤❤❤❤
Diouma Thiam ak mame bou goor😂😂😂😂😂 ms papay kheusha tmt 🔥
Papay kheuscha da seuse
Bété bété c la meilleure série actuellement vk des artistes professionnels mashallah chapeau 🎉
Cheut vous parlez des khass de Tické Laobé mais yayou Paco ak ay proverbram wolof j ai jamais compris ce que ça voulait dire mais khamnani punchline leu😂😂😂faut ma def cours renforcement wolof 😂😂😂😂
Bella rek waxado woul Ak ben xalé té loumou wax dou si délou
Différence bi Moy Bella ay Wolof you khaut lér nagne lay wakh ticket laobé dafa meun khasté😂😂
Néneu: "voyageurou djinakh (souris), bou tassek douanier mouss (chat), keuyite you valable douko takha djall"
Lolou c'est profond.... 😂😂😂
@niagnagueye2218 oh merci beaucoup 😍😍yow faut malay fey ngamay traduiral leep lou Bella meusseu wakh😆
Team Madioudia Tall😢gnou ande soutenir KO telna sone way😢
Kou sa yaye takh bagua guéné sa papa walayhi diga KA réthiou😢😢🎉🎉
Waw ame na 😂😂
Leguii il doit faire sortir sa mère 😅
Wa legui kou mom keur gui
Ou pas . Baye bou irresponsable di nakharel ce yaye . Baye bo rhamnné daram metoul ligueyo terrain bi gne tabarhal ce yaye sarkh de niou ko diappalé be mou féye ko . Il a parfaitement raison
@@louloutebien plus fatim thiam défoule dara loudoul défendre domam sou ne Kone man sakh ni fatim thiam defa nonou lay defa sa dom di dieul teranguam yobou Marieme Sall mou imiliéko ah nonou rk la mounone dèmé makhoudia si bopam mo soff
Li guén di jouer ça va droit au coeur on vous remercie nekhna trop way❤️
Herkil baye dou morom deh walahi diguako guisse j'aime trop mon père ❤❤
Légui yayame nak mome mirito guine te amol foumou dieume koy bayi sa moy takhawalou te domame mome keurgui
@@KaneMoastafa-z6xil aurait dû trouver une autre solution. Aucun des deux ne mérite de sortir de la maison. Mom doom rék la waroul woon dieul partie
Allahou Akbar ndékété li yeupp guente la 😂😂😂
Watal 😢
Jure arrête wallah tu ment .🤔
😂😂😂😂 surprise rek
Ndeysan evenprod defnagne sen casting 2eme saison sans Mareme Sall ba paré mais les téléspectateurs veulent toujours Mareme en espérant que ce soit un rêve.
Wait and see
Yalnaniou yalla may moudieu gou rafete taniou agali saison bi inchallah❤
Makhoudia yreume nako
L’autre jour, j’ai dit il faut mettre l’heure sur l’affiche de la bande-annonce et maintenant c’est fait ✅
Merci Evenprod 😚❤️
Makhoudia sonnou na 😂
Evenprod c'est le meilleur billahi mayal len mako ay coeurs ❤️🤝🤝 khol len images yi nimou nice see machallah ❤🎉
Makhoudia à la rue 😂. Vraiment, je n'aime pas Fatim Thiam. Elle a créé tous ces problèmes et maintenant elle fait la victime.
Ohhh c'est très émotionnel, les artistes sont des diambars vraiment laléne j'aime wawe
Pourquoi doom bou ngoor di gueuna beug yayaam ni papaam ❤❤❤
C'est normal comme ni djiguéne di geuna beugu papam
loLou mom amna
Nooy fasé waaté ta amoo keur😅😅
Moma diakhal 😂
Vraiment bien fait pour lui di weurr di faséwaté ni kou dof ahh ok parce que am nga ngnétel wa démal keureum amo keur nane dagay geuné waté soff marieme sall limoufi def lien ken wakhoul qui dafa seussss
Teksi di nek polygame tmt😂😂😂khana mou dem si 3eme bi
Waye nk c'est normal fatim thiam mo waral li yepou en plus respecte wul dieukeureum
Moma diakhal
Alhamdoulilah Kay l'en nu santi yalla
❤❤
Film bou graw mogui nii en fait affaire bi dou gueweul ak guer kassé sa évoque beaucoup de choses
Louy dindi deudeulé guir yallah sonouna walahi 🥲🥲🥲🥲🥲🥲
Yague ki
@ lou wax
Salut
Mane bala ma déé am niounane kou beug sa yaye rék lalal j'aime wala kou beug SEYDINA MOUHAMED rék lalal j'aime fi nieuppa beug séne yaye nieuppa beug SEYDINA MOUHAMED bouléne niou sonale way.
billahi ❤❤🎉
Liniouy def sakh da bakhoul wakh nagne ba sonou mais boune lagni deggé 🤦🏼♀️
Merci 😚
A cause de la parole de dieynaba tall baye da fort si dome bou djiguenne ndeyssane 😢
Fatime thiam sof nama loool sakhhh bouniou waxei mouni diaxeu rekk souniou kanam di lewatal beuteum yi rekk 😢
Rien qu’avec une BA j’ai des frissons evenprod dal 👍🏿
Amo keur di fassé 😅😅😅😅😅
Vrema.makhou tu exagère tamit Yako yobé sa bopp yawaronr soutoural sa bopp nak😢😂
Vrema.makhou tu exagère tamit Yako yobé sa bopp yawaronr soutoural sa bopp nak😢😂
Serigne fallou rek ❤❤❤❤❤
Yalna gneup am Diam si barké seydina mouhamed
Kou geum ni alkaly day guenteu rek beusal jaim❤❤❤❤
Makhoudia has played a great role in the film, he show all this coming since the start.
Every man should strive for having his own household. ❤️🇬🇲
Ko beg se yaay lale j’aime ❤
Bété Bété rek😊
Bilahi dome bo goor Moy xarito yayam
Kou beug seydina mouhamed lalal❤
Marème Sall nak franchement sa dieukeur meunone nala bayi gua continuer sa série bi nak mouy téré waté nonou
BILAHI MAKHOUDIA day dague hol yalla nagnou yalla moussale thi baye bou mêle ni
Les choses deviennent sérieuses nak, pleins de rebondissements 😮😮😮
Fatime thiam mo geune bone mareme sall mome dale dou déf Lou bakh jamais
Meussouma nekh dafa seuytanei tekk si dou def lou bakh sou diouguei di victimisé wou ki mbam la way
Jeureujeufé serigne Touba ❤❤🎉
Diouma Thiam douma ray😂😂😂 mais chapeau à Makhoudia il joue super bien son rôle ❤❤❤❤❤😊
Wa yenn even prod beugue niouy joyy chaque jour à tamiit les émotions waouwwww
Ma makhoudia mom laniou moudié fassé😂😂😂
Wa anna laobé yi😅😅😅
Makhoudia mo gueun sonou si série bi 🥹👆🏾
Dafa niak faida complexé teksi.
Famille alkali moko gueuneul diambotam au non d'une amitié bou sincéroul.
La preuve alkali la traité de Teugg kharam l'autre jour.
Makhoudia bou ndaw door dieynaba avec son etat.
Mareme sall la toujours mepriser
Mem sa 3eme femme quand il a frappé sa fille elle la remis a sa place
Mais méram ci ndiabottam lakoy sippi.
@ right lolou mom deugu leu
Amoul fouleu si bopam
Ker sa ker dhe walay ker sa ker Yalah nagnou ko Yalah sun brom bi May amine te mou dik gnou 🥰❤️
Kiy guente nah yewou mareme sall meunoul dee wy 😂
Ah moma diakhal 😅😢
Jusqu'à preuve du contraire c'est un rêve
Dieynaba tall et son pere sa fait reference a mon certe dafa tang mais je l'aime de tout mon yayam lama toude ken douma lal bou sma yaye di dkokhé lek wla dra sakh manéko ndalh sma papa amna😢❤❤
Kou bague saydina mouhamed lalal je t'aime
Mangui soga beug film depuis que j'ai commencé à le regarder
Lii nèko si kholl yi tè Manou gnouko wax yalla n'a yalla safara lèpou 😢❤😢😢
Li deh leniouy wax dome bou gor yayam dôme bou djiguéne papam voici la preuve 😭
Vraiment toutes les acteurs jouent bien ici machala
On cherche notre propre maison INCHA-ALLAH
Makhoudia ya fassé ba paré té amo fo dieum😂😂😂😂😂
Moom dafa sof
Moma diaxak goor dou gued 😂😂😂
Moye Gor gui yeuk fasse diabaram té amoul foum dieum waa am mongui ni makhoudia la😅😂😂
@@FatiGaye-op8kc yaa wah deugg dé🤣🤣🤣
Makhoudia na dem. Sonal naniou ak gneti rastam
Makhoudia tall mom ltx mou fouyy😅😅 ak bopam bou niaaw bii... C'est bien fait pour lui
Aï😂😂😊
Vraiment l’âne la beugone! Yaye yaye la! Di takk di fasse noumou ko nekhe beugue guene ko de chez ses
Enfants mou takkate indi! Fatim loumou bone bone c’est chez ses
Enfants! Mome
Moy guene
Bala ma dé rk gni nane fatim thiam mo gueune bone Marieme Sall khana maréme Sall tay la bakh chaque jrs mou nek fi di hass dieukeur dji ak domou diambour yii may len niou diam
Makhoudia je l’estime beaucoup ❤
Bane série guéne gueneu préféré si 2024 bi
Manchalla ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Des Cœurs pour evenpro ❤❤❤😊
Diouma elle est égoïste honnêtement depuis le début de la série .
La meilleure série du moment au Sénégal 🎉❤
Je suis content pour even prod ❤
Ohh trop d'émotions 😢😢dieynaba tall aime beaucoup son papa Diouma nakk sampou na dé 😂Makhoudia mérite pas ça sacré Dame il se mêle de tout