Ndeysan serigne makhtar nar lô sunu serigne mobakh ta wathié bopam yalnafi yageu ta wer ak mbolem nioukoy diapele si dara dji cheikh Ahmed Sakhir lô رحمه الله تعالى وغفر له وأسكنه فسيح جناته يارب
Daaray Koki , une fierté mondiale, Yàlla nañu Yàlla Fayal Séex Ahmadu saxiir Lo le fondateur depuis 1939 entre les deux guerres mondiales, ba nimu Wuyo djee boroomam ci atum 1988 Yàlla nañu ko Yàlla Fayal, Ginnaw moom Seriñ maxtaar naar Loo mi ko djiite ba jamono jii Yàlla Nako Yàlla may wer ak doole ak ni kay jàppale yeup. Daaray Koki mi Gi noonu avec ses 5400 et quelques taalibe, yoo xam ni, dañ jàng di lek, di tëdd di faju lépp gratuit. Kon. Nak ñoo gi woo keppp kuy def te Yàlla tax Koki mi Gi nonou
la" Daara de koki" ,c'est le Sénégal, elle n'est pas à négliger, on doit répondre à sa toute doléance et y intervenir le plus rapidement possible. Merci qu'Allaahu aide et protège cette "Daara"
Djoulite gni Sounou Borom Dinke Alale, gnou beugue ko dépenser si yoonou Yalla bi, déléne guestou dara Al-Khourane yi mélni koki , difa déff sen Alale , ngir diapalé ko ndongo daara yi . Nakh charges yi,Diss Na lolou Si Serigne daaras yii
Papa Ngagne déf ga Lou raféte❤👍
رزقنا الله واورثناهذه البركة ببركة يمن خديم المصطفي صلي الله عليه وسلم ورضي عنه وزاد الرحمة والمغفرة لمؤسس هذه المدرسة
Machallah Dieuredieuf serigne MAKHTAR nar Lo yalla na yalla same lenne 🇮🇹🇮🇹❤️❤️❤️
Machalah pape Ngagne Ndiaye ❤❤❤
Machallah Yalla na Yalla fayléne barkelléne sama daara yeup sì barké Alkhouran (AMINE)
Daara Koki toutes nos pensées à Serigne Sam Mbaye
Ndeysan serigne makhtar nar lô sunu serigne mobakh ta wathié bopam yalnafi yageu ta wer ak mbolem nioukoy diapele si dara dji cheikh Ahmed Sakhir lô رحمه الله تعالى وغفر له وأسكنه فسيح جناته يارب
Macheallah baye ngagne defga lou rafet ❤❤❤
Machallah waw leeeeeeeen goooooooor way machallah amna solo looool machallah
Merci pape❤❤❤❤
Sante serigne touba rék baal diana 😢😢😢😢❤❤❤❤
Ken dou Cheikh Ahmadoul Kabir Mbaye l'initiateur, le guide spirituel et l'homonyme de Serigne Modou Sakhir Lô, dans les années 1939
Machallah Yàlla na Yàlla fay S Ahmed Saxiir Lóo
🤲🏿🤲🏿☝🏿
ما شاء الله ❤❤
ماشاء الله جميل
حفظكم الله ورعاكم جميعا
Merci pape sa liguey rafet na ❤❤
Yallana YALLA dolli ko yërmànde
Yalla na yalla bar gél
Macha allah jerudief seringue bi yalla na yalla faylén yiw si barkéb allkhourannullkariimm amiinn ❤❤❤
Dieureu dieufati mame cheikh mbaye rk lepou mom la
❤❤🙏 sëriñ Ahmed saxiir loo yalna ñu ko Yàlla Fayal, sëriñ Maxtar naar loo yalnafa yàgg te wér loole🙏
Machallah merci pape ngagne
Machallah fila sama Serigne diagé alqouranne mouhamed lamine dramé yalla nanioko yalla fayal
Daaray Koki , une fierté mondiale, Yàlla nañu Yàlla Fayal Séex Ahmadu saxiir Lo le fondateur depuis 1939 entre les deux guerres mondiales, ba nimu Wuyo djee boroomam ci atum 1988 Yàlla nañu ko Yàlla Fayal,
Ginnaw moom Seriñ maxtaar naar Loo mi ko djiite ba jamono jii Yàlla Nako Yàlla may wer ak doole ak ni kay jàppale yeup.
Daaray Koki mi Gi noonu avec ses 5400 et quelques taalibe, yoo xam ni, dañ jàng di lek, di tëdd di faju lépp gratuit.
Kon. Nak ñoo gi woo keppp kuy def te Yàlla tax Koki mi Gi nonou
Yalna yalla diaplé daray alkhourane yi neke ci adouna bi yeup sirtou ci senegal ak daray koki amine
Machall amna soll de ❤❤❤❤❤
Yalla na yalla faye Serigne Ahmed sakhir lô ak Serignam ba tourandom mame cheikh Mbaye kabir
Machallh ❤sema khôl defa sédde lole si pape gangne❤naniou diappalé daara koki
Dieureudieufé serigne matar nar lô
Dieureudieuf mame cheikh mbaye li lépou yawla diarama ch ahmadou sakhir mbaye❤
Papa ngagn ndiaye defga lou rafett lolll
Pape liga deff kawena lolou
Merci
Vraiment machala li doyneu yaram …on doit beaucoup les aider 😊
Maa chaa Allah
Machllah 😭😭😭😭😭
Yalla na yalla fay cheikh Ahmed sakhir lo
Macha Allah yalla nalen yalla takhawou 🙏
la" Daara de koki" ,c'est le Sénégal, elle n'est pas à négliger, on doit répondre à sa toute doléance et y intervenir le plus rapidement possible. Merci qu'Allaahu aide et protège cette "Daara"
الحمد لله رب العالمینdamou alqurane rek lanou sohkla yalln na diame kahnam ba were adouna touts ما شاءاللهماشاءاللہ في أمان الله
Yàlla nañu yàlla Fayal Séex Mouhamadou saxir lo
S a saxiir loo yalna ñu ko Yàlla Fayal
Ndaye saan yalla nanou yalla fayal S Mohamed sahir Lo
Amna solo
Machallh amna sol torp
ماشاء الله تبارك الله 😢
Cëy! Yàlla
Mashalla rafetna
❤❤❤
Machalla papa
مجهول في الأرض معروف في السماء شيخ أحمد صغير لوح
❤❤ماشاالله
ماشاالله 7:19
dieureudieuf pape ngagne
Machalla l Etat war na diapalé Dara bou bax. Former lene après niou diangue métier après Étude. Pour meune intregre si société bi
Ndayesane li yemena dara moyé lepou
😢😢😢
Machala
Djoulite gni Sounou Borom Dinke Alale, gnou beugue ko dépenser si yoonou Yalla bi, déléne guestou dara Al-Khourane yi mélni koki , difa déff sen Alale , ngir diapalé ko ndongo daara yi . Nakh charges yi,Diss Na lolou Si Serigne daaras yii
Ngourouk Sénégal dañuy takha Walu dara Ji lépp ñoko warna Gadu
Mai na eta diokhe bitse dara dji
Walay ndeysaan
ana serigne mboup
❤❤😢😢😢😢🙏🤲☝🇪🇦🇬🇭
Salam je vends mon imprimante afin que je puisse payer mes frais d'inscriptions.C'est une Hp 5660.J'ai raté beaucoup de cours.
Salut combien
@@albachiralofficiel4667 Salut c'est à 40.000F
Daraji di teudj rek laniou man ak di wedi lo nit ñi seeni Serigne nékon na fi
Wa khou fi dara 👎
Ligua wax amoul fila deuk té magui ak sama Serigne
Yalla naniou yalla fayal Mame cheikh Ahmadoul kabir Mbaye
Merci
♥️♥️♥️♥️♥️
Machala
❤❤❤❤❤
Machalla
❤❤❤❤❤❤
❤❤❤❤❤
❤❤❤❤