😭😭😭 maman massa way que Dieu te vienne en aide et que tu guérisse à vie 🤲.. t'es une conseillère exemplaire et pleine de pudeurs mashallah moi je t'adore bcp sincèrement ...
Walahi je te comprends moi j'en souffre tellement defois je ferme les yeux pour imaginer ce que ma mère vie yow sa khél mougui ak yow santal yalla ma mère est une maur touarègue elle était tellement belle mais à cause de sa cesite elle a perdu la raison quand je vois une personne bien portant je me dis pourquoi la mienne est malade c'est tellement difficile wayé yalla jamam rék lay natou
Banyang, notre chére soeur adorée ! Massa ! Massa ! Moi même, ma propre Méré est restée, une fois aveugle complétement pendant 2 ans !!!!! Mais après , elle a recouvert la vue pendant plus de 50 ans et plus... Jusqu à pres que sa mort . Yalla nalla. Walleu !!!! Allahouma amiiiine ya rabbi !!!!
Yallahi ses vrais maman je suis en Tunisie j'ai amené ma mère pour la soigner ici en Tunisie et se que je comprend pas beaucoup de médecins tunisien ont fait leurs études de médecine au Sénégal et ils sont très très patients même les médecins tunisien nous demandent pourquoi vous venez vous soigner en Tunisie juste pour dire que mon pays va mal toute les côtes
Salam mbayang yalna yalla safara sa febar ba nga delou si say activité. Wayé waxtaane wax deug thia la. Fii nga yor sa emissiin di si reveler toute sorte d histoire tou bone. Meme yi doul deug. Tu as fait une emission sur ma famille sans connaitre la vérité té walahi la nga thia winé yepp dara dou si deug bilahi. Lepp daniou la nakh. Mou metiwoone si nioune lool. Legui nak niata famiile nga tek lou mel nonou. Nioue mooe djagal naniou la. Wayé boo khoilé sa digganté ak yalla di nga baalou niou barri akh. Li la dal nak natiu la yalna la ko yalla teguil
Mbayengue ce qui me plais sur vous avec tout les problèmes que tu ya .la faible santè des yieux tu garde ta dignitè .surtout .je suis tres fiere de vous . Machala yalla nalla yalla same maye la wèrre .si katanou yalla .courage la grande dame
Mane dé gueum naani lii yeukeutikou daradja la thi yow tata Mbayang. Nio ngi ley nianal yalna yalla gaaw ko teggi té defal la kheewal yi waralone galankoor bii. Prompt rétablissement tata chérie. Qu'Allah te vienne en aide🙏🏿🙏🏿🙏🏿
J'ai les larmes aux yeux mais dafa am lou yale wakh inellah massabirine elle a aidé beaucoup de gens ndayssane yaneko yale takhawou mou guissate inchalah
Du courage Mbayang. Le pays va mall. La faute incombe à l’Etat. Faut mettre les hommes qu’il faut à la place qu’il faut. Nommer un ministre de la santé qui n’a même pas la santé lolou fomou ame. Place bounioukoyy diokhé, dagneko warr diokh kou déme bobou formation. Mais tant qu’il y’a le clientélisme politique, rien ne marchera dans ce pays. Massa sister kou geume yalla nga. Yalla moyy tégué nattou té boukko waré tégui rékk mou dégne. Courage
Je m’excuse j’ai sauté une phrase, je voulais écrire nommer un ministre de la santé qui n’a même pas le profil de quelqu’un qui a fait la formation en santé
En résumé vraiment le système santé Sénégalais est incompétent c la vérité...et yalananiou yalla maay président bouy defaraat pays bi inchallah dans tt les domaines
Yalla nako yalla same waye tè maye ko wèére kou bakhe kou yagua dimbali nitte si sociale une grande dame yalla Mila tek li yalla nako tègui Thi barki YONÈNETI BI PSL
Grande Sœur, je veux que tu lis tres mon message: tu te rappelles le resto ( juste a coté de la direction 2stv vers Allianz Assurance ) ou tu prends le déjeuné avec tes amis..les kebs,,et y avait Pape Alé Gueye..ce jour y avait 2 verres sur la table et 1 des vers était empoisonne comme cible pape Ale..et ce verre la ,une de tes amies ta donné de leau sans le savoir et depuis ce jour là, Ta souffrance a commencé. Pour ton seul medicament ,tu dois boir que de l'eau EVEAN..j'ai bien dit EVEAN pas Kirene. Bonne guérison Tata. Pour plus d'info écoute bien l'une des vidéos de Molah MORGANE.
Massa maman. Natou la rek mais sounou borom dinako tegui AK jamm. Kou bah rek Moy amm natou. L'état doit la prendre en charge franchement elle est d'un intérêt populaire. Les bonnes volontés vont se manifester inchallah
Thiam baabèl dèmba thiam yaw jam rek ngay am yalla na la yalla may werr mbayangue yalla na nga goudou fan yala bounou sèddalè dara sa ganaaw barquè ckheikhoul khadim wèreul wèreul
ha sohna mbayang kéne yénéou lako mais kéne dou yaou yalna sounou borombi fadiale bopame machalla gueume gue yalla té yalla moye kilaye fadiale bopame ci barké serigne fallou serigne fallou mbacké mane damala yague beugueu wallahi mo warale message bou gougou bi
Yalna yalla saafara tata Mbayang. Niit kou bakh nga masha Allah. Lii ndok la rek dina diale insha Allah. Boul khalat dara. Rufisque ?? Il me semble que vous êtes lébou. Kholal tamit ci côté sén toure yi ba kham. Touroul ba khame
Ohhhhhhh tata Mbayangue li la dal meti na ba fou meti yem mais nékhoul yeureum nakh diambaram ak dignitém machalah😭❤️ je veux pas rentrer dans les détails mais sunu Senegal bi dafa doy waar, je suis fondu en larmes 😢 quand je regardé la vidéo lou yomboul ci man mais mangui ley nianal ci barép seydina mouhamed, ci barkep alkhour’an, ci barkep mame Abdou dabakh mi niou meu toudé, ci barkep Serigne bamba sama yakar yalla na la sunu borom takhawou delo ci wer ak meuneul sa bopou banga delou ci say activité inchalah ❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️🙏🏽
C'est vrai khamnassi dara jetais cortico dependant mais comme toubab laa melone. Ma yaram am lekh am karaw changer complètement. Damadone sakh rousse guèneu si mbède mi bilahi. Mais alhamdoulilah. Yalah nala yalah diapalé teguil la natou bi
Une grande dame de valeurs, courageuse, digne, honnête, je te souhaite une bonne guérison, dinabakhe inchallah bon courage,mbayang.
N deye daba.n dao je la souhaite une bonne guerison a mbayang fu courage
Allahouma Amiiiiiiiiiine Y'a Rabbi 🤲 ❤ 🇸🇳 🤲 ❤ 🇸🇳 🤲 ❤❤❤❤❤❤🇸🇳
YALLA MO LÈYE FEYE MANCHALHA
Bonjour je voudrais svp le numéro de mbayang svp
Ndeysanne c'est dur, elle garde sa dignité malgré tout. Puisse le bon Dieu lui venir en aide tata Mbayang thi barké werou koor gui.
Amine 🙏🏼
Amiine ya rabi
Qqqqqqqqqqqqqqqqqqqqqqqqqqqqqq¹
Amine
0
😭😭😭 maman massa way que Dieu te vienne en aide et que tu guérisse à vie 🤲.. t'es une conseillère exemplaire et pleine de pudeurs mashallah moi je t'adore bcp sincèrement ...
Yalla mi la ko tek yal na la wëral inchahalla courage
Walahi je te comprends moi j'en souffre tellement defois je ferme les yeux pour imaginer ce que ma mère vie yow sa khél mougui ak yow santal yalla ma mère est une maur touarègue elle était tellement belle mais à cause de sa cesite elle a perdu la raison quand je vois une personne bien portant je me dis pourquoi la mienne est malade c'est tellement difficile wayé yalla jamam rék lay natou
Mougnal del dalal xelam☝️ bouko bayi mouy weet deel doxantou ak mom. Legui xelmi nieuwaat
Dinala nianal xolou mougne.Del doli di sant yalla comme vous êtes toujours ensemble.
Du courage.
Ndeysann massa yalna yallah feug bopam
Diamoussi yalla tarbiyouko nit amoul koudoul yayam lo mougn mou diékh
@@wourydiop Wawaw lolou kay faratala dome menoul faw waydioram et merci pour le conseil
Banyang, notre chére soeur adorée ! Massa ! Massa ! Moi même, ma propre Méré est restée, une fois aveugle complétement pendant 2 ans !!!!! Mais après , elle a recouvert la vue pendant plus de 50 ans et plus... Jusqu à pres que sa mort . Yalla nalla. Walleu !!!! Allahouma amiiiine ya rabbi !!!!
Amin merci
Euskeuy !!!
Amine
@@mayangthiammbayang2570 Yala nala diapale
Allahouma amiine
Dieu est grand Adjia Mbayang que Dieu te garde Alkhamdoulilah
Je suis tout cœur avec toi Mbayang
ALLAHOUMA AMINE NIOU BOK KO.
Elle a toujours été une très grande dame de valeurs.
Yalna la yala defal diam ak tawfèkh Masha'Allah.
Pluies de grâce sur vous Maman Mbayang
Il faut l'aider elle a tout fait pour le Sénégal elle mérite d'être aider une brave dame et gentille
Du courage Tata Mbayang adorée Ya Allah same leu té arla li dawna yaram . Notre Tata nationale adorable
Allahou Akbar !! Yallah nala Allah swt takhawou té delo la sa sago barke Seydina Muhammad psl. Amiiiiiinnnnneeeee
Ndeyesan adouna dou dara yalla nala yalla may weur mayko mbolem dioulit 🤲🏻🙏🏾
Bon courage maman dieu est grand inchaala il va vous assister inchaala
Yallahi ses vrais maman je suis en Tunisie j'ai amené ma mère pour la soigner ici en Tunisie et se que je comprend pas beaucoup de médecins tunisien ont fait leurs études de médecine au Sénégal et ils sont très très patients même les médecins tunisien nous demandent pourquoi vous venez vous soigner en Tunisie juste pour dire que mon pays va mal toute les côtes
Ndeyesann..bilay métti na trop maman yalla nala yalla weureul barké s.mbakh non wayy
Machalla tata mbayang que Dieu vous en garde et vous donne une longue vie et une santé de diamant é de fer
Masta mettina
Salam mbayang yalna yalla safara sa febar ba nga delou si say activité.
Wayé waxtaane wax deug thia la. Fii nga yor sa emissiin di si reveler toute sorte d histoire tou bone. Meme yi doul deug. Tu as fait une emission sur ma famille sans connaitre la vérité té walahi la nga thia winé yepp dara dou si deug bilahi. Lepp daniou la nakh. Mou metiwoone si nioune lool. Legui nak niata famiile nga tek lou mel nonou. Nioue mooe djagal naniou la. Wayé boo khoilé sa digganté ak yalla di nga baalou niou barri akh. Li la dal nak natiu la yalna la ko yalla teguil
Ndeyssan vrément metina sama idole la kou bakh du courage yalla nala yalla diapalé unchallah
Tata mbayang Yalna yalla dèllo leu thi ça sago barkè taha aleysalam 🤲
Rufisquoise et fière machalah yalnala yall mayy weer yaye mbayangue
Mbayengue ce qui me plais sur vous avec tout les problèmes que tu ya .la faible santè des yieux tu garde ta dignitè .surtout .je suis tres fiere de vous . Machala yalla nalla yalla same maye la wèrre .si katanou yalla .courage la grande dame
Doyna ware yalla nala yalla may tane thi barké seydina mouhamed mé fadiou olof yi diémeko khol yalla bakhena ❤️❤️❤️
Sokhna mbayang yalnala yala may weer lila dall ak courage bingako bolele sougnou borom doula bayii danga gueum yala 💗💗💗
Aaah Mbayang I use to watch ur programs I'm sorry for u but may Allah grant u good health inshallah
Merci Tata Mbayang inchallah lèpeu dina bakh sa khol dafa rafèt
Massa ta mbayang yallanala yalla laye wéer barké sedina mouhamed psl 🙏
Sokhna mbayang thiam,k dieu swt t'accorde une longévité dans la santé.amiin yaa rabbi...
Sokhna si Yalla nala Yalla soutral te arr la Yalla minga khamni koumou arr nga mouth koumou doutral kén doula yap 🤲🤲🤲👏👏
Amna yakar souniou diokowe inchallah 🤲 yalla dinako safarra amna kouma khame koo khamni gissna sama kanam mou fathie aye goumba baniou giss billahi 🙏 yalla bakhna dina bakh inchallah 🤲 tata 💯te soula menoul fathie doullale sa xaliss te 10mill100fr rek laye fadie🙏
Slt
Macha Allah la grande dame bonne guérison, vous êtes unique comme femme de cœur DIEU veille sur vous amine ya Rabbi 🤲😍 ❤️
Mane dé gueum naani lii yeukeutikou daradja la thi yow tata Mbayang. Nio ngi ley nianal yalna yalla gaaw ko teggi té defal la kheewal yi waralone galankoor bii. Prompt rétablissement tata chérie. Qu'Allah te vienne en aide🙏🏿🙏🏿🙏🏿
Sama sopé bi yalla nalla yalla takhawou barké naby Moustapha psl 🤲
Ndeysane tata mbayang yallah nala yallah takhawou mbagua wérr sii diam sii mbarké séydina moukhamed yallah meun nako thé yallah nako yallah déf sii wérou koor gou séll bii 🙏❤️❤️❤️
Machalla ahja mbayang yalla na la yalla may werr ak guoude fann ❤❤❤❤🙏🙏
Yalna yalla may wër délola si sa sago ci barké Mouhamad aleyhi salatou wassalam Massa
Mbayang yalla nala yalla fay sa khol
J'ai les larmes aux yeux mais dafa am lou yale wakh inellah massabirine elle a aidé beaucoup de gens ndayssane yaneko yale takhawou mou guissate inchalah
Du courage Mbayang. Le pays va mall. La faute incombe à l’Etat. Faut mettre les hommes qu’il faut à la place qu’il faut. Nommer un ministre de la santé qui n’a même pas la santé lolou fomou ame. Place bounioukoyy diokhé, dagneko warr diokh kou déme bobou formation. Mais tant qu’il y’a le clientélisme politique, rien ne marchera dans ce pays. Massa sister kou geume yalla nga. Yalla moyy tégué nattou té boukko waré tégui rékk mou dégne. Courage
Je m’excuse j’ai sauté une phrase, je voulais écrire nommer un ministre de la santé qui n’a même pas le profil de quelqu’un qui a fait la formation en santé
Ooh c'est émouvant massa tata yalla nala Yalla doli safara 😭😢😭
Que le BON DIEU la donne un BON remède, MAMAN JE VOUS SOUHAITE DE TOUT CŒUR UN BON RÉTABLISSEMENT DE VOTRE VISION ,UNE LONGUE VIE ET UNE SANTÉ DE FER
Ho maman bonne rétablissement ❤️🩹 Que dieu te garde bien maman ❤️❤️
En résumé vraiment le système santé Sénégalais est incompétent c la vérité...et yalananiou yalla maay président bouy defaraat pays bi inchallah dans tt les domaines
Ta foi te guérira au nom de JESUS
Amen 🤲🏾😭
Amen amen au nom puissant de Jésus-Christ
Amen
😒
🙏🙏
Yalla nako yalla same waye tè maye ko wèére kou bakhe kou yagua dimbali nitte si sociale une grande dame yalla Mila tek li yalla nako tègui Thi barki YONÈNETI BI PSL
Yalna sounou borom bi SOUBHANA WATALA takhawoula ba nga wér incha ALLAHOU RABI 🤲 si BARKÉ SEYDINA MOUHAMAD ALEYI SALATOU WASALAM ❤ incha ALLAH
Grande Sœur, je veux que tu lis tres mon message: tu te rappelles le resto ( juste a coté de la direction 2stv vers Allianz Assurance ) ou tu prends le déjeuné avec tes amis..les kebs,,et y avait Pape Alé Gueye..ce jour y avait 2 verres sur la table et 1 des vers était empoisonne comme cible pape Ale..et ce verre la ,une de tes amies ta donné de leau sans le savoir et depuis ce jour là, Ta souffrance a commencé. Pour ton seul medicament ,tu dois boir que de l'eau EVEAN..j'ai bien dit EVEAN pas Kirene. Bonne guérison Tata. Pour plus d'info écoute bien l'une des vidéos de Molah MORGANE.
Père tu es notre soveur on n est de tt cœur avec toi
J’ai quelque chose pour vous
@@bracoure vas y..!!! Je t'écoute.
@@booparker424 je veux savoir si est ce que vous êtes la bonne personne, je ne lance rien par ici
@@bracoure je suis une bonne personne et je le serais pour toujours.
YALLA nala Bour YALLA takhawou delo la sisa kantane ba gua wer si diam Amine
Ndeysane une très belle dame ❤ prompt rétablissement !
Ndeysane yalla nala yalla takhawou si barkep werou koor gui 🙏🙏🙏
Sante léne SOKHNA Aida Diallo , nafi yagg te werr
Tata mbayangue yalla nala yalla samou té taxawoula diamou rék inchallah
Une grande dame de valeur. Bonne guérison Sokhna Mbayang
Massa maman. Natou la rek mais sounou borom dinako tegui AK jamm. Kou bah rek Moy amm natou. L'état doit la prendre en charge franchement elle est d'un intérêt populaire. Les bonnes volontés vont se manifester inchallah
Ndaysanne yaye boy yalna yalla zafara bilay coubax nga
Courage mme ligaye doumdou metina Yallah nala Yallah takhayou si barker alcourane karime si barker wéro koorgui amine
Du courage longue vie à toi
Massa mbayang yalnala yala tahawou yaw nitt koubaagnga malahamm mann nabou wade..je testime fort
Yalla na la yalla wéraale ci kataname ak baakhame amine ya raaby 🤲🙏
Masa yaye booy yallna yalla safara si barké alkhour anoul Karim 🤲
Tata mbayang bayil maquillage bi surtout au niveau des yeux
Surtout et le khèsal ce n est pas bon pour les yeux
Ki est venu ici après le live de Molllah et père?
Moi
@@ciskosora hé moi aussi ✌🏿
Moi
Pan am na bopou
Yalla nala yallah maye wér werlé Mbayang ci barké Seydina Mohamed SAWS massa Thiam walaye j'ai les larmes aux yeux
Yalla nako Yalla safara sii barképe seuyou douna mouhamed psl 🙏🙏🙏
Del nane ndokh evien. Evien defko sa ndokh mom kassè Yalla dinasi Def diam. Inchala yalnala Yalla Sam yaye mbayangue
Thiam baabèl dèmba thiam yaw jam rek ngay am yalla na la yalla may werr mbayangue yalla na nga goudou fan yala bounou sèddalè dara sa ganaaw barquè ckheikhoul khadim wèreul wèreul
Je l'aime bien tata Mbayan, yalna yallah wéral inchalah rabii té dey am sakh dakh ci lou bakh lagn la meussa dégue
Ke le tout puissant vs guide et vs benisse yalla are la same safara sa diaguoro
Mon père aussi avez cette maladie.ndeysanne khalate nako ba guagnou.yalla nalla yalla diapalè bou bakh mayela tanè .c difficile.
Ayy wayyy bne volonté yui guèssou lene tta mbayangue🙏nitte gni bala nioulaye dimbally rèkk ga dèeee🤲🙏🙏🙏
Prompt rétablissement sokhna mbayang yalla nala yalla défal tan bou bakh
Tata mbayan yalla nala yalla takhawou diga tané si barké wère yii sel yii
Amal wer ak Werlé mbayang du courage
Kou bakh dimbaléma gire yalla si numérome ma dimbaléko girre yalla 🤲🤲🤲😭
ha sohna mbayang kéne yénéou lako mais kéne dou yaou yalna sounou borombi fadiale bopame machalla gueume gue yalla té yalla moye kilaye fadiale bopame ci barké serigne fallou serigne fallou mbacké mane damala yague beugueu wallahi mo warale message bou gougou bi
Yalnala yal may wer ta mbayang si barké seydouna mouhamed psl
Yalla nalla Yalla may tane si barké seydouna mouhamed
Yalna yalla saafara tata Mbayang. Niit kou bakh nga masha Allah. Lii ndok la rek dina diale insha Allah. Boul khalat dara. Rufisque ?? Il me semble que vous êtes lébou. Kholal tamit ci côté sén toure yi ba kham. Touroul ba khame
Yalna bour yalla wéral té takha woula si barké sangue bou teed bi saws
Tata yalla ga wer ak diamou
Manchallah tata Mbayang yalna la yalla takhawu si barker Seydina Mouhamed
Ya Mbayague thiame yalla nalla yalla faye sa xole bou rafete yawe diame rek ngaye Ame boule ragale dara long vie ❤❤❤❤❤❤
Elle à beaucoup fait pour 2sT
Nako Elhadj NDIAYE Diapalé 🙏🏽
Ces évident
9
Hay ta MBayang démale setti serigne fallou rakhemane Kou y'alla maye LA mane mom Amna foumou diar AK mane
Non c'est émouvant, j'ai les larmes aux yeux yallah nala yallah takhawou
Amine waye sokhna Aida diallo nite yi khamou gnouko mais yalla khamnako yalla nako yalla faye 💖❤yiwe same ko
Triste yalla na yalla meye tanne si barke seydina Mohamed psl
Ohhhhhhh tata Mbayangue li la dal meti na ba fou meti yem mais nékhoul yeureum nakh diambaram ak dignitém machalah😭❤️ je veux pas rentrer dans les détails mais sunu Senegal bi dafa doy waar, je suis fondu en larmes 😢 quand je regardé la vidéo lou yomboul ci man mais mangui ley nianal ci barép seydina mouhamed, ci barkep alkhour’an, ci barkep mame Abdou dabakh mi niou meu toudé, ci barkep Serigne bamba sama yakar yalla na la sunu borom takhawou delo ci wer ak meuneul sa bopou banga delou ci say activité inchalah ❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️🙏🏽
Amiin yaraby
Aminnn way ndeysan
C'est triste vraiment, nous sommes tout cœur avec toi
Masta, diangaloul khassida Mathla bou chifaa-i, douko ray sa mbeute yi
Machaallah mbayang ngeum gui molla japale ak sa mbaax yaag fi te wer damala yaagga sope
Masta yallah nako yallah safara nga tok beu guiss thi barki Seydina Mouhamed SwS 🙏
Bilay dagma yaga neex trop tata mbayague yalna yalla safara Baker Seydina Mouhamed psl Baker werou koor gui inchallah🙏💞😍
C'est vrai khamnassi dara jetais cortico dependant mais comme toubab laa melone. Ma yaram am lekh am karaw changer complètement.
Damadone sakh rousse guèneu si mbède mi bilahi. Mais alhamdoulilah.
Yalah nala yalah diapalé teguil la natou bi
Machala une femme que jestime bcp,yala na yala safara
Merci brave madame !
Yallah na yallah wereul leu
Ndeysane métina massa yalna yalla safara
Slt depuis que j'ai entendu cette mauvaise nouvelle j'ai pensé à une maman qui habite à ziguinchor qui l'aime tellement ❤️❤️❤️❤️bonne guérison
Massa maman yalnala yalla May tann ...malgré sa douleur elle garde tjr sa dignité
Yalla nako yalla may wer bamou délou si activitém kou yarou ta rafét wakh machallah🤲❤
Allakhou Akbar yalna la Yalla weural ak diam. Je suivez beaucoup ces émissions et elles m'aidaient très bien dans ma vie conjugale. Gathiè ngalama
Mbayang yalna yalla werel
Ndeyssane yalla nala yalla diapalé métina lol waye ma sœur du courage
Ndeysane yallanalaya yalla diapale
Bilahi nitt kou bakh la yalnko yalla maye weer