RESPECT A VOUS MADAME. Pour une première femme vous etes ....simplement..ADORABLE. QUE DIEU VOUS GARDE ET VOUS BÉNISSE. Pluie de bénédictions à vous tous.
Macha allah samay deukeundo samay haritt sen Goro Pa samb mome sama tipoo laa macha allah wa keurgui mome gnépp paa bahe macha allah sen Dieukeur nakk mome moyy Lass Pa Maïssa Mome aussi il est juste magnifique beugue ndiabotte tékssi yalla nalen yalla lafall thiatt🥰🥰🥰🥰
Machalah sama yaye lam demba yaw awo nga ndieukè nga très posé et sans problème nioun dhè yaniou yarr def si niounn diom yalla nalla fi yalla bayi banga fèkkè lep inchalah❤️😍🥰
♥️♥️♥️♥️♥️♥️ MashAllah Laff thiat. Yalla nalene Yalla same. Same Séné borome keur .Moussal leñe si satanés. Merci Awwo bourou keureum. Boye Daro ♥️ Daro Sasse nanoulaa. Yaar AK teguine AK seyyyyy
Mais MashAllah laf thiat cette famille qu’Allah protège cette famille. J ai pleuré et j ai beaucoup ri🤣🤣🤣😂😂 J ai mal au ventre🤣🤣🤣🤣🤣🤣😂😂 Votre mari a choisi de bonnes femmes. Intelligent, smart gentleman-MashAllah.
Mancha Allah Awo Bourou keureum kou la guisse khamné kou bakh nga des cœurs pour toi ♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️
💖💖💖💖💖💖💖💖💖💖💖💖💖💖
Ki moy awo vip waw kay
❤❤❤❤💖💯
❤❤❤❤❤
Lam demba ki ngoné Ndiaye moy yayam lam demba moy awo moy ndieké mokk diekeur dji gno bokk Ndeye gawlo bi
Awo darro bi dee classe rekh LA am MAchalla tes daro kham na ni kou bakh LA MAchalla yalla na lene yalla bolle tes lafal lenn thiate
RESPECT A VOUS MADAME.
Pour une première femme vous etes ....simplement..ADORABLE.
QUE DIEU VOUS GARDE ET VOUS BÉNISSE.
Pluie de bénédictions à vous tous.
Machalla Awa bou bakh nilay méll wawaw Lam siré mayram kénn d'où yaw vraiment Yaw rék ya bakh diam Si yaw ma chérie ❤️ 🙏🙏
Mais awo bi elle est belle en plus am classe
Alè les ndeye Maguette aye awo lagne gno bok tour done aye awo mashala dara toute mes felicitation yala na bèbe bi dounde ta ame ndeye ak baye
@@ndeyemaguetteba6245 machaallakh laf bouche
Ak noirceur bi, très classe 🌹🌹🌹🌹
Billahi yow
Moleneme dakk d
Mani awo sou maté dara douko diakhal barki alkhourane sa dieukeur dh machallah ❤️🙏
Cheuuuu awo bi lamou jongoma té rafete ko lanla mâcha Allah ❤️ bobou sourire ak sakaré yallah bi 😍
Kii d moy awo vip belle et douce mashalla 🥰
Darro yalna yalna yalla may fan wou goudou wër guou yaram
Ndeysane yalla nalen sunuu borom mousseul si seytane lii rafetna lolou way je vous aime way
Ameen ya Rabbi❤❤
J aime cette famille. Machallah. Daro er ses coépouses. Tres bien.
00⁰⁰⁰0⁰⁰00⁰⁰000000000000000000000000000000000000⁰00000000000000000000000000000000000000000⁰00000000000000000⁰00000⁰0pp⁰p⁰000p
Awo tmt lane la diongama class refet machalla😍🥰
Macha allah samay deukeundo samay haritt sen Goro Pa samb mome sama tipoo laa macha allah wa keurgui mome gnépp paa bahe macha allah sen Dieukeur nakk mome moyy Lass Pa Maïssa Mome aussi il est juste magnifique beugue ndiabotte tékssi yalla nalen yalla lafall thiatt🥰🥰🥰🥰
Machalah sama yaye lam demba yaw awo nga ndieukè nga très posé et sans problème nioun dhè yaniou yarr def si niounn diom yalla nalla fi yalla bayi banga fèkkè lep inchalah❤️😍🥰
Ey Waye Li Nakh N’a De Yalla Dijamm Yagg❤️🙏🙏🙏🙏
Amine yarabi
Amiin
Awo bou bakh
Grande chance pilier familiale bou solide ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Première Dame bii machaAllah tabarakalhou ❤️
Awo yaye Awo calme awo classe yalna lène yalla mousale si saytanè diam nèkhna
Ndeysane Machallah yalna len yalla diapalé tê mousseul len si seytané yi🙏🙏🙏
❤️❤️❤️❤️❤️machaalah yallananou am diabar yu dioubo dafa nekh darro dalen lakal 😂😂😂
Bobou classe Awobi cheuuuu🥰🥰🥰🥰🥰🥰Daro sa awobi diongoma na machallah
Ak noirceurr bi, amna classe mom, kèn doukou wahlo loumou hamoul
Machalla Awo bourou kereum dionguoma dalll ❤
Machalla l'y nekh n'a trop diamme defa nekh,🥰❤️
Très belle famille mashahallah nasséne diam yagg
Machalla sama rakdji awo nourou keureur ni rek la borom keur dou yak keureur Lam sire Marieme laf thiate
Wawaw Awo bourou keureum kénn d'où môme Lam siré mayram guorr la nakh domi guorr la diam Si môm mak Sama❤️❤️❤️
Machallah Awo yaye tu es magnifique ❤❤😘😘
Yallaa na bébé bi doundou té barkéleu si daradjieuy seuydinaa Mouhamed PSL 🙏
No Lala lakalé nga🤣🤣macha allah awo nii laye mélle daye oufe Daro yalna bébé bii mague tes barkéle
Awo yaye way man dh begue nala machalla dagua classse❤️❤️❤️
Machallah très belle belle-famille que dieu vous protège daro 💕💕💕💕
Machallah Daro yalla na sen diamme yague❤️❤️❤️
Awo bi macha allah noirceur dfna tèy complexe,ndeysane dafa âme kèrsa
Mashallah bi awo way kay awo nilay mel yallah na mel ni iow
Amine dèl Sakho mougne rék cherie loula nitt dèf gua kholèko lila yalla dèfal gua naneu dokhe nopi kèn doula geune 🙏🥰
Machalla famille bi yalnalène yalla lafal thiate rek ahh lii nekhna waay téy oyof ak beugeu nite té yeuk nite❤🤦♂️🥰
MashaAllah awo bi
Naturellement am classe
Teint bou raféte
Machalla daro m mensoin épéciale à premiére dame❤️❤️❤️❤️❤️❤️
♥️♥️♥️♥️♥️♥️ MashAllah
Laff thiat. Yalla nalene Yalla same. Same Séné borome keur .Moussal leñe si satanés. Merci Awwo bourou keureum. Boye Daro ♥️ Daro Sasse nanoulaa. Yaar AK teguine AK seyyyyy
Yalnaleen yalla défal diamou way bou dara khathie sén diganté way inchalla yalla bakhna adouna amoul bén solo rafétal rk mo am solo
Ndeyssane machalah yalnalene yalah gueuneu dioubolé 🙏 ❤
Ma challah yalla na yalla gueneu dioubeule
Daro sa awo bî baxna ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Machallah awo bii de royoukaye la
Première Dame dafa âme classe macchalla
Mais MashAllah laf thiat cette famille qu’Allah protège cette famille. J ai pleuré et j ai beaucoup ri🤣🤣🤣😂😂
J ai mal au ventre🤣🤣🤣🤣🤣🤣😂😂
Votre mari a choisi de bonnes femmes. Intelligent, smart gentleman-MashAllah.
mais leur belle mère est gentille
@@khafssatoubaro4723 exactement-
Il y’a toujours 2 choses : un bon époux et 1 bonne belle mère.0 stresse- djama tchi le lepeu ketch.
Félicitations pour le bébé félicitations aussi pour le premier femme des enfants et 3e femme mashallah
Machallah bou am personnalité
Machalla awo bii tey na raféte yalla nalenn yalla lafal thiate
Awo bi kou am yaar la , t am classe . Roubé kat yi na seen yaram daw nak
Ndeysane awo bi sa rétan tamite yalna sen diam yagu amine
Machaala rafétena wayé daro kéne dou yaw
Awo bi mom Machallah diii, tééy rafét très naturelle 🥰
Thiéy L'homme mo wékh Yeux ddd 🤣🤦🏿♀️🤦🏿♀️🤣 Diam ci yén
Setlou nga Lolou 👀
@@a.barhamcisse7290 bou bakh sakh, doyna war daaal
Macha alla awo bou bakh nila wara mel beugue sa dieukeur beugue loumoula indil bilahi awo classe way
Aaaaywaayy bou sama woudjou mélone nii sama khôl seed mais ...😭😭😭😭 Yalla nako délosii
Amine nio mbokk niaan bi
Amiin
tanéko rek yague yague dina wathie
Une femme exemplaires machallah a vous tous et a Faro😘😘🥰🥰
Awo bi bakh na dé mancha-allah dafa ame yare🥰🥰🥰🥰
Baptême validé vraiment assez émouvant
Wa daro d'Adone guinte wate Wala ??
Machallah awo bourou keuruem ❤❤❤❤💃💃💃
Machalla 🥰🥰🥰 🥰🥰🥰🥰
Meussouma commentaires mai ki mo mérité awo yaye machalla
Mashahalla rafette na sou woudjieyeeup mellon ni keur yi nekh
Samaye wudiou ni lagnu mel sugnu zéro stress ta gnune gneup aye xalé lagnu mé sugnu keur dafa néx
C’est vraiment beau….😍😍😍🥰🥰🥰
Awoo yaye awoo yaye awoo yaye ❤️yay sounou awoo yaye ❤️sounou yaye awoo yaye dama contant si awoo bii bilay ❤️💯
Mane dh awo la ayma woudiou mais bouko yalla dogalone yalla na mélni iow mou raféte rekk inshalla diam daffa nékh
Awo bi machallah rafét na
AWO NI LAWARA MEL BAKH AM CLASS
Machaalla keur gui nekhna trop awo bou bakhé ni amoul way
Machala maguette LaM yarou bakh rek la kham thiy yaw awo nila wara mél
Awo bi machallah daffa yarou
Awo bi machallah elle a l’air gentille
Li Moy Sénégal rafet na machala
Machalla yalla nalène yalla lafal thiat
Awa Macha Allah defa âme classe te teféte
Ahh awo bourou keuremm machala teyga sa wak nice nioune awo yi nio melni
Deugeuleuhhhh
machala li dafa nex yalana diam yague yala mousale lène si thiate ak saytané
Machallah adorable awo
Wa dakar buzz bilay kéudou yene ⚡️🇸🇳
Ndaysan li nekhna Yalna yala moussal len si saytane
Machalla yalna yalla sakhale Diam thii séne biir 🙏🙏
Ndeysane awo yi mougne reck yokhlene 👌
Awo bii bakhna trop ❤️❤️❤️❤️❤️🥰🥰🥰
Machallah laf thiat yallah na djam yague💞💞
Machalah laf thiat ♥️ Mère bi néna monde bouné wath nafa 😁😁
Moma diakhal 🤣mane niatta monde mo amm
Khana planète mars la nek mom mère bi bay weur ay monde😂🤣🤣🤣
Môme la Beugeu Lath tamite niata monde 🌍 mo am😂😂😂
Machala yalna lene seytane sekhelou
La journaliste ou animatrice elle est trop excité elle poses des questions elle répond et c’est elle qui danse….
Sinon longue vie au bb
😂😂😂😂
J’aime ça si c ds ce milieu oui mon cheri takal legui mane sakh meun n’a yobou thiane Bi tinkiete 😅
Li dawoul sama yaram beugoula
Machallah machallah
C'est beau
Ma sha halla bélle familles
Macha alla mais awo bi d mo léne dakh niom nieup macha alla t dafa dale sakh.
Awoo bi kagn da rafete machalla💕
Elle est toute mignonne et posée
Bilay Awo bi kaye Ma Sha Allah ♥️♥️♥️♥️♥️🥰🥰😘😘🥰😘🥰♥️😘🥰♥️🥰😘🥰♥️🥰😘♥️🤩🤩🤩
Maguette Sall première dame niepp la ouf machalaaa.
Athioum sama tata awo yaye
Yalla bouma woudié ci adinaa
Machallah li raféte na trop
Awo kou dal la ndeyssane nileu lou gnaw bakhoul na raféte réc
Machalah 💖❤️💖💖🙏🙏🤲🤲🥰🥰
Machallah awo pire nilaye mel je l'adore
Sama kharite sama Lépp sama domou ndeye ❤️❤️❤️❤️❤️❤️
j'aime bien la première femme 💞💞💞💞
Maasha Allah lafthiat thiat🥰🥰
Mashalla kadou yi raféteneu ❤️❤️
Insultez comme ça aussi ☹️Daro même bou deh ay kaff c’est pas jolie😦
😁😁😁tameuh lago la, faté na sakh caméra bi😁😁😁
@@khadydiouf7279 c’est vrai deh mais sagua si bopam camera ou pas daffa warroul
Dafa dioum
Awo bi dieulna damli daffa ame classe