Urgent problème entre les baye fall est les supporters de ndamatou yamba lagnou léen guigne..

Поділитися
Вставка
  • Опубліковано 21 гру 2024

КОМЕНТАРІ • 159

  • @sagyatal8545
    @sagyatal8545 7 днів тому +7

    Niak diom ana Touba ak Association

  • @seemoodiop6138
    @seemoodiop6138 8 днів тому +9

    Bilahi baye fall yi danio eupeul li dou deug dou yoon

    • @omarndiaye5827
      @omarndiaye5827 7 днів тому +2

      Saway gni bougne défoulwone dara kéne douléne diapou

  • @Science-z5w
    @Science-z5w 8 днів тому +13

    Lima nekh cii Touba moy do guis khale bou Djiguene bouy wané ay tieureum

    • @BambaAissy
      @BambaAissy 7 днів тому +1

      BiLay Wallay DeuGueLe

    • @elagegueye3310
      @elagegueye3310 7 днів тому +2

      niak djoulit mo gueneu bon awra djiguen niak ham ham۔mountaha mofi dike niak djiouly

    • @Science-z5w
      @Science-z5w 6 днів тому +2

      Elage Gueye tu as raison

  • @MamebossoNdiaye-se8eg
    @MamebossoNdiaye-se8eg 4 дні тому +2

    Fan la Serigne Touba wakh dilen football yen lougn len wakhal yena

  • @BambaAissy
    @BambaAissy День тому +1

    😍😍😍😍😍😍😍😍😍😍😍😍😍😍😍😍😍😍😍😍😍😍😍😍😍

  • @daarahalimoulkhabirdaaraha3389
    @daarahalimoulkhabirdaaraha3389 7 днів тому +7

    Baye Fall Yii Bayi Diouly Ak Woor 😂😂Dii Téré Foot Ball Sarap Ndayou Lii

    • @pirlo4478
      @pirlo4478 5 днів тому +1

      @@daarahalimoulkhabirdaaraha3389 yaw do mourid lolou yaw mal hiayam lay ler cheikh Ibra waliou kamil lh Serigne Touba moy Serigne niam té Serigne Touba yalla may nako kouné mandoul si lolou

    • @BayeDjilyKane-z2i
      @BayeDjilyKane-z2i 4 дні тому +1

      Wakho fi gatt lou takh gane dou mourit

    • @BambaAissy
      @BambaAissy 3 дні тому +1

      Wallahi DeuGue le❤​@@pirlo4478

  • @MoustafaMbacke-kf8sj
    @MoustafaMbacke-kf8sj 5 днів тому +1

    Boulén gnou sonal la preuve kholal gnargni si ganaw ak Séni khésal gni dagnouy fane si équipe asc yi ngén wara guéné bir touba té légui mbacké ak touba gore gni khésal lagnou dieul

  • @pirlo4478
    @pirlo4478 7 днів тому +3

    Yé na réw Serigne bi néna ngué bayi téré yi nguéne lankk mourid ndigal bayi léne football bi té dem diangui Al xourane ak xassida yi té nguéne bayi sen diakhane yi merci police nationale ❤❤

  • @ModoubaraGueye-v5b
    @ModoubaraGueye-v5b 5 днів тому +1

    Yéen say koussi bëgg équipe ngéen dem sene dëkk maam yi booléen ñu yàpp

  • @ibradieng4537
    @ibradieng4537 7 днів тому +4

    C est une honte de parler de asc à touba.le propre de Touba est l adoration exclusive de Dieu si vous ne pouvez pas vous confirmer aux règles établies dans la ville sainte allez ailleurs

  • @abdoulayediagne5963
    @abdoulayediagne5963 6 днів тому +1

    Daguénn bakh li Serigne bi bègue rekk Moy amm diékhna takk loulénn baye Fall yi déff rkk bakhna dakh yéna xoti worr mayy Serigne bi dagne léna rayyy Wlh Wlh Wlh 😎😎

  • @Khadijafall-em2xn
    @Khadijafall-em2xn 7 днів тому +3

    C’est la baye fall😂

  • @LayeKane-fx2hg
    @LayeKane-fx2hg 4 дні тому

    Machalla nél yi sétna

  • @airseck568
    @airseck568 7 днів тому +2

    Bay fall yé 4 sen ndayam si bopam

  • @cheikhmbaye1877
    @cheikhmbaye1877 8 днів тому +7

    Seen nell yi dafa rafitt😅 sakh

  • @ngathiefallmusiquefromsene2060
    @ngathiefallmusiquefromsene2060 7 днів тому +1

    Banditisme partout au Sénégal il faut que vraiment les autorités prennent leur responsabilité gisnga ngi dano yap sénégalais yi demléne ligeyi vraiment bayi navettane ak lamb doul kham demléne ligeyi c'est tout

  • @ZAWKAR34
    @ZAWKAR34 8 днів тому +6

    Nèk lènn aye mourite tè bayil sènn yèufou dof yi touba kenn warou fée football

    • @FatouLo-j7o
      @FatouLo-j7o 8 днів тому

      Dou touba nak mbacké la na ler

  • @Gaye-industrie
    @Gaye-industrie 8 днів тому +4

    Outillen metier bayii thiakhane waaay❤

    • @cheikhtidianembengue6709
      @cheikhtidianembengue6709 8 днів тому +2

      Nékal ndéy nitt

    • @pirlo4478
      @pirlo4478 7 днів тому

      ​@@cheikhtidianembengue6709Merci frère boye yi nio soff nio yakh Touba ak imagou Touba 😢😢😢

  • @MbayeKhadim-h9c
    @MbayeKhadim-h9c 6 днів тому +2

    Li acte Terroriste le 😢

  • @ElimanekaraZickroulah
    @ElimanekaraZickroulah 6 днів тому +1

    Baye fall yi yallna yalla yokou sén katan baniou meuneu doumeu gniye tégui ndiguelou seurigne touba 😂

  • @ngathiefallmusiquefromsene2060
    @ngathiefallmusiquefromsene2060 7 днів тому +3

    Danlene moye sakh indispline total partout au Sénégal, il faut que les autorités prennent leur propre responsabilité ! Touba titre foncier la n'oubliez jamais ça

  • @YellyKa
    @YellyKa 8 днів тому +4

    Serigne bi beguoull football guéné diguénn football très bien si yénn

  • @MbayeAfia-x7o
    @MbayeAfia-x7o 6 днів тому +1

    Yén dagena niakk diom😂

  • @mouhametniang9201
    @mouhametniang9201 8 днів тому +3

    Il ne peut pas avoir deux républiques dans un meme territoire qu’on se dise la vérité (les hypocrites je ne vous parle pas)

    • @moucaboro
      @moucaboro 8 днів тому +1

      Moi qui pensait que c’est toi le nafekh

  • @Ahmadouyadalifall1111
    @Ahmadouyadalifall1111 День тому +1

    Dieureudieuf baye fall yi 😂😂😂

  • @AboubacryGASSAMA-zs7oi
    @AboubacryGASSAMA-zs7oi 7 днів тому +1

    On s'en fout😅😅😅kou nèk ak sa problème. Kou beug nopalou su thiahane yi topale alhourane ak souna voilà amouo lènène 😅😅😅wa salam

  • @MoustaphaGaye-k4g
    @MoustaphaGaye-k4g 8 днів тому +4

    Loun len def bakhna 😂😂😂😂

  • @DiadiaNdiaye-v3r
    @DiadiaNdiaye-v3r 8 днів тому +3

    😂😂😂😂nel fondé😅😅

  • @AmethNdiaye-p4e
    @AmethNdiaye-p4e 8 днів тому +2

    Gen lenn touba lo lenn fay def fo fou da niou lenn diapp diame l’islame dakh dafa may nitt yi liberté focé woul ken si dra kouy geum gua geum Kou toroxal nitt rk la niou meun 😢

  • @boromdendeyedecor830
    @boromdendeyedecor830 9 днів тому +3

    Dame fall limou wakh dara dousi deugg

  • @tourematar5600
    @tourematar5600 8 днів тому +1

    Baye fall yi nioy toukh yamba dji nioy nane sanguara si paré sosal sëgne bi

  • @adamandiaye3448
    @adamandiaye3448 9 днів тому +12

    Dagne léna togne sossal lén diap léne Di lén diakhassé ak serigne bi lignou wakh dara doussi deugue dagniy fén

    • @ousseynoutoure3621
      @ousseynoutoure3621 8 днів тому

      Ya meuneu doul gnou meilni yaw gno beugueu touba yakhou bougnou deifoul wone dara keine douleine diap mane li maye lathieu moye nane nga meu neu deikeik serigne touba nane da ngueine fowi soparei nga gnawate touba souleu tolou lei none do deim deuki fagnouye fowei

    • @moucaboro
      @moucaboro 8 днів тому +2

      Ay vrai nafekh ngen li Serigne bi di terre ci deukëm ngen dem MBACKE diko fa def

    • @elagegueye3310
      @elagegueye3310 7 днів тому

      ​@@moucaboroli yalla di tere niak djoulinak serigns bakoy dikle yaw si boppap yay doul katbi

  • @Issa_Diouf_Officiel
    @Issa_Diouf_Officiel 9 днів тому +1

    Good job 👍

  • @alhikmatabiri6955
    @alhikmatabiri6955 8 днів тому +4

    Ana touba ak association football aki ecup

  • @Khairaprod1
    @Khairaprod1 9 днів тому +2

    Noy diougué Mbacké dieume ndamatou di déme diouma djia😅DAME SODA DAL thi ay thiaxan lanék

  • @ngathiefallmusiquefromsene2060
    @ngathiefallmusiquefromsene2060 7 днів тому +1

    Réglé wolene deug dou nekh

  • @Amicolegueye-n2d
    @Amicolegueye-n2d 8 днів тому +2

    Bay fallo yi aye def len

  • @bayngagnediene1833
    @bayngagnediene1833 9 днів тому +3

    Danguéna niakkk fayda ay ponkali góor yu Toolu ni yéen noulén Bay Fall yi di diapeé

  • @youngmouride6448
    @youngmouride6448 8 днів тому +2

    Yakeu diome guéne defff louko raw molen warone dalle

  • @ModouFall-lv8hu
    @ModouFall-lv8hu 7 днів тому +1

    Porte lene plaite

  • @Ahmadouyadalifall1111
    @Ahmadouyadalifall1111 День тому

    Bayil fene 😂😂😂

  • @MameThiernoMbacke-g5c
    @MameThiernoMbacke-g5c 3 дні тому

    Man dh Touba la deuk, heure bouma nekh lay genn dem fouma nekh, mais lima wor ba wor moy benn baye falle dou am si man yoon, parce que douma def Lou yalla teré amouma Diotou foo ndax jaamou yalla ak lageey kousi nekk do tall foo, gis nga Serigne Addouna KI DIOUBOUL RECK mo sonnou, téngena fekhé nekk si Lou yalla geuneum reck, deuk bi khamné Lou bonne lagnou fay aayé, boudé mano fa nekk kon kay yaw y’a diouboul rcek

  • @sagyatal8545
    @sagyatal8545 7 днів тому +1

    Mais bayi len li Serigne di téré mo guena yombu
    Bayfall defoun dra Serigne Mountakha molen diokh ndiguel

    • @daarahalimoulkhabirdaaraha3389
      @daarahalimoulkhabirdaaraha3389 7 днів тому

      Ya Meune Doul Baye Fall Yii Yalla Sant Léne Diouli Ak Woor Niou Bagne Lou Léne Ab Serigne Sant Niou Déf

    • @alleualleu693
      @alleualleu693 7 днів тому +3

      Bayi diouli mo gueun na bon foot ball 😢😢😢😢

  • @daamnjaay1274
    @daamnjaay1274 8 днів тому +3

    Seen nel yi set na 😢😂

  • @TOURECONSTRUCTION
    @TOURECONSTRUCTION 8 днів тому +3

    Guisssa goo leen dara sax 😂😂😂

  • @jamesjoob3771
    @jamesjoob3771 7 днів тому

    🤣🤣🤣🤣🤣🤣😂😂😂😂le Nell😂 Wa touba merci beaucoup pour le baye fall je habite darou minan jjj JJJ

  • @KhadimDiouf-
    @KhadimDiouf- 8 днів тому +2

    Sén leufeul ndy niome nieup aye domi xaram lagn blh daguén warone kate sén ndy niome nieup

    • @pirlo4478
      @pirlo4478 7 днів тому +1

      Sa gniari dambali papa boyi Touba yi guamatoune Serigne Touba 😢ay imbéciles nguéne 😢😢

  • @matarfall9599
    @matarfall9599 8 днів тому +3

    Lu takh li niy tere si deuk bi manuleko bayi

  • @BambaAissy
    @BambaAissy 8 днів тому +1

    😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂

  • @abdouseck1814
    @abdouseck1814 10 годин тому

    niak diom teksi yarouwolen .

  • @faiiousarr8216
    @faiiousarr8216 8 днів тому +1

    nék lén ay nit😅😅😅

  • @serignefalloukanendamatou4630
    @serignefalloukanendamatou4630 8 днів тому +1

    Lolou bakh na si yène 😂😂😂

  • @SassoumGueye
    @SassoumGueye 5 днів тому

    Touba Ben keur la

  • @SmorDieng
    @SmorDieng 8 днів тому +1

    Sawaye seringe daye téré football tookléne😂😂😂😂😂

  • @moustaphagaye1015
    @moustaphagaye1015 13 годин тому

    War nguéna rousse sakhe niou léniiye lathie ngûéniye wakhe gathia la sakhe

  • @jamesjoob3771
    @jamesjoob3771 7 днів тому

    😂😂😂😂😂😂😂😂🎉🎉🎉🎉 🎉🎉🎉🫶🏾💪🏿👍🏿👍🏿👍🏿

  • @LeuzNiang-p1r
    @LeuzNiang-p1r 9 днів тому +1

    Lign wakh si ASC yi dara amousi kilifa day wakh deugg

  • @mbackefall4248
    @mbackefall4248 8 днів тому +2

    Defo dara gnou door la watt la si gnak chance la bok

  • @LeuzNiang-p1r
    @LeuzNiang-p1r 9 днів тому +1

    Baye fall daniouy togne deugg deugg

  • @papadieng935
    @papadieng935 8 днів тому +1

    C’est bien vou aller servir d’exemple on voit les autres pays religieux Solène bayiweii meune na dem ba eupp doleiii dono wara régler boy yi malene kham

    • @SamsidineNdiaye-u7u
      @SamsidineNdiaye-u7u 5 днів тому

      Merci beaucoup les bayes fall.bien fait xaleyi dagno.niang diom merci beaucoup les bays fall🙏🙏🙏🙏🙏

  • @yaguabakh
    @yaguabakh День тому

    Topo lén feulé rewmi guén trop. Niak fayda, niak jomm té niak dieuffé ndigueul molléne daal.

  • @MamebossoNdiaye-se8eg
    @MamebossoNdiaye-se8eg 4 дні тому

    Kou sa bay yaroul ay dioumbour yar la Touba gnom gni gnola gueuna kham ni Touba khaleyou gor yi dagnouy diay yamba doumani gnom lade mais Touba dagnouy diay di toukh yen mantech sakh manoulen ko yen yalla bouma nek sen yay ngen nek Touba beugua nek ay bandi di dégradé di tak ay sen gnouy fi di fen yen dounguen rouge sakh

  • @CheikhDiene-nt3vb
    @CheikhDiene-nt3vb 8 днів тому +1

    Dame fall day fén

  • @KhadimDiouf-
    @KhadimDiouf- 8 днів тому +1

    Data yayou bay faux yi douniou aye bay fall dé aye domi xaram lagn

  • @Mbayeniang-pc8ng
    @Mbayeniang-pc8ng 2 дні тому

    Mes tamite wa Touba bayilen football yene tamite segne bi dakoye teres

  • @SerigneFallouWade-cm6zg
    @SerigneFallouWade-cm6zg Годину тому

    Touba deuk diambour la dieufé ndiguel rèk wala nga djibi sa deuk mame amoulène louléne wakh yéna togne

  • @BallaNiang-r5y
    @BallaNiang-r5y 8 днів тому +1

    Néll yi ra féte na wor maléle touba

  • @Mbay23
    @Mbay23 4 дні тому

    Touba la fa ame dou deugue dou yonne baye fall yi doygnou ay policiers Etats bi mossi warra diouk li dou yonne un n'Etat ne doit pas etre faible baye fall yi lignouy def mo guenneu arrame dougnou diouli dou gnou wor ay thiahane dongue la

  • @niangseydou4848
    @niangseydou4848 4 дні тому

    Gni dem nane ba final tee ken defoulene dra kon niom boulen defe dra niom la kon delene xalate gni dagno warra neek ay nit

  • @MorFall-xj6fb
    @MorFall-xj6fb 8 днів тому

    Yaye AK séné Serigne dagen Kat sen ndaye

  • @mandiayediaw2076
    @mandiayediaw2076 8 днів тому +2

    Sen néll yi refatna dé

  • @AbdouBadiane-o4q
    @AbdouBadiane-o4q 9 днів тому +1

    Baye fall yi sen lefal ndeye

  • @salioundiaye9189
    @salioundiaye9189 8 днів тому +1

    Yéna togne aecé bir Touba

  • @NdiayeDiouf-u7v
    @NdiayeDiouf-u7v 8 днів тому

    😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂👍👍👍👍👍👍👍👍👍

  • @KakaBa-jn1pr
    @KakaBa-jn1pr 9 днів тому +1

    Doye n'a war de

  • @abdouseck1814
    @abdouseck1814 10 годин тому

    danioulen waron douma douma you metyy

  • @thiatukarandiaye5301
    @thiatukarandiaye5301 8 днів тому +1

    Dame soda sosal rkk lay deff Shmm 😡😡

  • @CheikhDiene-nt3vb
    @CheikhDiene-nt3vb 8 днів тому +1

    Dame fall day doul

  • @Elhadji-j5n
    @Elhadji-j5n 8 днів тому +1

    Amolen diome bayile li Serigne bi tere

  • @DiopFépp
    @DiopFépp 9 днів тому

    😭😭😭😭😭😭

  • @Paolo-t4g
    @Paolo-t4g 8 днів тому +2

    Danguén wara bayiii nàwetan Touba nékoul Dakar

  • @fallouthiam9211
    @fallouthiam9211 9 днів тому +1

    Yen da gun yambar lolen def bax na

  • @cheikhmamesaliou8386
    @cheikhmamesaliou8386 8 днів тому +3

    Football amoul touba yalla rk mofa nek

  • @thiatukarandiaye5301
    @thiatukarandiaye5301 8 днів тому

    Baye yi ay togn katt lagn démm mbacke nieuw kou sol maillot niou diapp la Fékk kou diàngoul khala Wala ngakoy Diokh app deuk dobbou Ndéye lii 😡😡😡

    • @omarndiaye5827
      @omarndiaye5827 7 днів тому

      Bounguéne dougué bamél danguéne yaru

  • @djamildiouf8593
    @djamildiouf8593 7 днів тому

    Niak diom duniu rouss saxxx😂😂😂😂 ak sen ndel

  • @bayemodoufall2879
    @bayemodoufall2879 8 днів тому

    ❤❤❤😂😂😂😂😂

  • @mbenguekhadim7859
    @mbenguekhadim7859 8 днів тому

    Yen wa tuob😢a safara geni😢😢😢😢😮 dundo

  • @alhikmatabiri6955
    @alhikmatabiri6955 8 днів тому +1

    Wargèna ross wanè sèn boppu nann nioodoon dèf liii yax dèru waa ndaamaato

  • @mbackefall4248
    @mbackefall4248 8 днів тому

    Yéne nopi léne te mougne amolene chance😅

  • @ThiernoSeck-po4sf
    @ThiernoSeck-po4sf 9 днів тому +1

    Filagne nan soowo peul yi taye téléphone boye yi lagne sathe

  • @BayedjilyNdiaye-p7x
    @BayedjilyNdiaye-p7x 8 днів тому +3

    Wakhouléne deuge dé sougéne beugone Serigne Touba dougéén déff ligéni déff

    • @cheikhtidianembengue6709
      @cheikhtidianembengue6709 8 днів тому +1

      Nékal ndéy nitt

    • @BayedjilyNdiaye-p7x
      @BayedjilyNdiaye-p7x 7 днів тому

      @cheikhtidianembengue6709 sa ndéy yaw wala

    • @BayedjilyNdiaye-p7x
      @BayedjilyNdiaye-p7x 7 днів тому

      @cheikhtidianembengue6709 bayi léne foo mi ak thiakhane bi té diamouji yalla limouma s.touba beige si dekeum bi

    • @cheikhtidianembengue6709
      @cheikhtidianembengue6709 7 днів тому +1

      @@BayedjilyNdiaye-p7x katal sa ndey feulé touba bokou na thi deuk yi gueuna bonn Sénégal coup beugu déf lou bonn fofou ngay dém

    • @BayedjilyNdiaye-p7x
      @BayedjilyNdiaye-p7x 7 днів тому

      ​@@cheikhtidianembengue6709yaw sa bounou ndéy yaw sa ndéy amoul katou Kaye yaw ne tou iblisga yaw ak gniga andale👎

  • @elhadjifalilouka5665
    @elhadjifalilouka5665 8 днів тому

    Prochaine fois préparé len rek ,rayanté rek

  • @AbdouNdim-m8d
    @AbdouNdim-m8d 8 днів тому +1

    Diadieuf Baye fall yi

  • @MorGning-n4i
    @MorGning-n4i 8 днів тому

    Doyna war dal

  • @KhadimNdiaye-ws4bx
    @KhadimNdiaye-ws4bx 8 днів тому

    Baye faal yi daal thiy thiaakhaan rek lanne nekk

  • @msarr3084
    @msarr3084 7 днів тому +1

    Wa pastef fen rek bayi len Touba dem fenen te bayi nafekh bi. Li Serigne bi tête si touba

  • @YaAwaFall-n8f
    @YaAwaFall-n8f 9 днів тому

    Baye fall yi lini déf dafa gnew lol

  • @PAPA-v8w
    @PAPA-v8w 9 днів тому

    Football kassé

  • @AbdouNdim-m8d
    @AbdouNdim-m8d 8 днів тому +1

    Lou Serigne bi beugu Touba moy ame diadieuf Baye fall yi liguéye bi rafétena trop

  • @AbdouNdim-m8d
    @AbdouNdim-m8d 8 днів тому +2

    Yéne liguéye khélko ba guini ngindi football vraiment c dommage