Serig🎉 Serigne momar diagne avait alerté sur ce phénomène personnes l'avait écouté et voilà maintenant le résultat c'est pas aux bayes fall de faire la loi dans un pays de droit
Je suis tout à fait d’accord avec toi mon frère on est des humains on pleure pour nos droits pour l’égalité la liberté et pour vivre tranquille on peut pas subir la violence ils vont pas tu es mon frère c’est pas possible ce genre là il faut les juger 😢😢😢😢😢😢😢😢
Sénégalais yi danio raggal bamou yobbou lén ci ak nafékh li xéw Touba dou deugue dou yoon C'est l'état qui a failli à sa mission Serigne Mountakha ne doit pas être au dessus de la loi Les peulhs défendez vous koussi déé dém Aldiana Yalla souniou borom bouko nékhoon kouko tonie mou yooni ayy malaka niou doumala mais défouko
Problem bi mooy senegal defa bari ay nafikh gnou bari dagnouy ragal wakh degge me gniepa khamnagn né li khew touba dou degge dou yoo bay fall nagnou reglé te bay togn
Ce village est un village peul il est là avant Touba c'est leur zone historique les villageois ont vécu avec cheikh ahmadou Bamba et ils sont mourides donc il faut bien réfléchir pour cerner ce problème
Machalla sa wakh Rafétena. Pour moi problème etheni leu Wolof Daf yakare mo guénn kouné. Nagne gorgorlu si diame yallah. Mo wore.té tope ndiguel sunu borom.wassallam🙏
*Un simple civil ne peux pas entrer dans la maison d1 citoyen en pleine nuit sans y être invité c une violation de domicile* *lou la fa dal ya ka yobè sa bop* Repose en paix
Ce n’est pas aux bayes fall de faire respecter la loi . Vente de cigarettes n’est pas un délit. Le titre foncier de Touba se limite au niveau de la mosquée et ses environs . Le village de Thiaye fali n’est pas l’intérieur du soit disant " TF" Même les FDS n’ont pas le droit d’attaquer des villages paisibles à minuit et de fouiller des chambres pour chercher de la cigarettes. Il faut dire la vérité, seule l’État doit avoir le monopole de la sécurité des populations du SENEGAL pas des bayes fall ...
Mané bayfall bokoy diokh ndégal yoniko si tolyi na roudji na khari matte ndakh ko khameni doudiouli dou oor naane ak toukh ak sathie rek moy sa métier kéne douko pousse si ay nitte liinagne si wakh téwakh dégueu.
Les baye fall sokhlawounouléen yéne wa Séne web séné vidéo UA-cam bi wakhouléne thi deg wakho léne Thi gui nou rayé ray diwakh thi gnari béye youdé thiam
Mané affaire baye falyi danko wara arété waay sinon kanéne dinafa dé marday taaly baye falyi managnu réklé touba ana police ana gendarmerie pour lane gnouy fadial s'en bope
Touba est sur le plan juridique un titre foncier c’est pas une ville c’est une maison le droit de propriété est sacré partout dans le monde Kou fii nèké nou nékhoul borom tu sors de la maison oubien on doit te poursuivre et mettre en prison pour violation de domicile Le bon sens voudrait qu’Il faut déja connaître l’statut de Touba avant de parler
Mon cher même toi qui a un titre foncier de ta maison tu n'a pas le droit de te faire justice. Oses tu violenté ton épouse ou ton enfant ou même ton employé habitant la maison ? En plus, un titre foncier prend toujours en compte une superficie bien délimitée mais avec l'extension de Touba si on veut tout prendre dans le titre foncier est ce qu'il ya lieu de douté que Touba est entrain d'absorber des villages qui ne dépendaient de lui comme les peuls l'ont bien expliqué. Ils ont dit que c'est Touba qui a empiété sur leur village.
Serig🎉 Serigne momar diagne avait alerté sur ce phénomène personnes l'avait écouté et voilà maintenant le résultat c'est pas aux bayes fall de faire la loi dans un pays de droit
Touba lou serigne bi beugue thi deukeum bi rek mofay ame
Je suis tout à fait d’accord avec toi mon frère on est des humains on pleure pour nos droits pour l’égalité la liberté et pour vivre tranquille on peut pas subir la violence ils vont pas tu es mon frère c’est pas possible ce genre là il faut les juger 😢😢😢😢😢😢😢😢
Sénégalais yi danio raggal bamou yobbou lén ci ak nafékh li xéw Touba dou deugue dou yoon
C'est l'état qui a failli à sa mission Serigne Mountakha ne doit pas être au dessus de la loi
Les peulhs défendez vous koussi déé dém Aldiana
Yalla souniou borom bouko nékhoon kouko tonie mou yooni ayy malaka niou doumala mais défouko
Baye fall yi ci thiakhane laniou nek
Problem bi mooy senegal defa bari ay nafikh gnou bari dagnouy ragal wakh degge me gniepa khamnagn né li khew touba dou degge dou yoo bay fall nagnou reglé te bay togn
Civile Meinoul Djox Ordre Civile Serigne Sii Xamougne Touss Xam Xam Moy Ndiite Gouvernement Bou Niak Fayda Mafia Religieux Avec Le Familles Religieux
Voilà
Ce village est un village peul il est là avant Touba c'est leur zone historique les villageois ont vécu avec cheikh ahmadou Bamba et ils sont mourides donc il faut bien réfléchir pour cerner ce problème
Machalla sa wakh Rafétena.
Pour moi problème etheni leu
Wolof Daf yakare mo guénn kouné.
Nagne gorgorlu si diame yallah.
Mo wore.té tope ndiguel sunu borom.wassallam🙏
Amna loo khamné rafétoule sougnou khole paune wala hawma loumou done civil mokoo wara khol ana gendarmerie wala police civil moo wara fathie llou khew thie deuk téé gnii dieule ay diourou diambour lolou nane lagnouko meuné toudé doyna war
Afair baye fall yi Serigne bi daff ko wara araité naw daffay ligueye
Bayfal yii dougnou rouss ndakh gniom lagnou khamé toukh kouy toukh baay fall yii mooy sa bay😂
bay falsi nionecthideuge
3:31
*Un simple civil ne peux pas entrer dans la maison d1 citoyen en pleine nuit sans y être invité c une violation de domicile*
*lou la fa dal ya ka yobè sa bop*
Repose en paix
Ce n’est pas aux bayes fall de faire respecter la loi .
Vente de cigarettes n’est pas un délit.
Le titre foncier de Touba se limite au niveau de la mosquée et ses environs .
Le village de Thiaye fali n’est pas l’intérieur du soit disant " TF"
Même les FDS n’ont pas le droit d’attaquer des villages paisibles à minuit et de fouiller des chambres pour chercher de la cigarettes.
Il faut dire la vérité, seule l’État doit avoir le monopole de la sécurité des populations du SENEGAL pas des bayes fall ...
Je suis mouride mais baye fall yi rew dongou lagnou def. Serigne bi na waax ak niom chak jour baye fall yi rek
Qu'il vont ce faire voir qui ils son eux pour interdire ça ?
C buveur de bière c'est a'lcoolique
walahi chivil meneul djite chivil dafa nara metti kon naniou xoll
Bayyi len baye fall yi géne fi wakh yéne wa SÉNÉ Web Géene bayyi diwakh thi serigne TOUBA ak mame cheikh ibrahima fall .bakhoulén
wakhofi dara
Ay sath laniou baye fall yi wakhlenn deugg gui
Serigne Yi pour gnome 1945 Lagnieu néek !!c' est bien fait pour le bayfall !!
Mané bayfall bokoy diokh ndégal yoniko si tolyi na roudji na khari matte ndakh ko khameni doudiouli dou oor naane ak toukh ak sathie rek moy sa métier kéne douko pousse si ay nitte liinagne si wakh téwakh dégueu.
Peul Di tokh paune baye fall yamba lay tokh niom nieupay tokh Di mandi
Les baye fall sokhlawounouléen yéne wa Séne web séné vidéo UA-cam bi wakhouléne thi deg wakho léne Thi gui nou rayé ray diwakh thi gnari béye youdé thiam
Mané affaire baye falyi danko wara arété waay sinon kanéne dinafa dé marday taaly baye falyi managnu réklé touba ana police ana gendarmerie pour lane gnouy fadial s'en bope
Touba est sur le plan juridique un titre foncier c’est pas une ville c’est une maison le droit de propriété est sacré partout dans le monde
Kou fii nèké nou nékhoul borom tu sors de la maison oubien on doit te poursuivre et mettre en prison pour violation de domicile
Le bon sens voudrait qu’Il faut déja connaître l’statut de Touba avant de parler
un titre de 400 ha nga beug declaré 12 milles ha bayil tiakhan. Kou am TF loula nekh ngassiy def ?
Sou dé 400ha la Touba am comme titre foncier , vraiment je pense que l'état doit s'expliquer.
Mon cher même toi qui a un titre foncier de ta maison tu n'a pas le droit de te faire justice.
Oses tu violenté ton épouse ou ton enfant ou même ton employé habitant la maison ?
En plus, un titre foncier prend toujours en compte une superficie bien délimitée mais avec l'extension de Touba si on veut tout prendre dans le titre foncier est ce qu'il ya lieu de douté que Touba est entrain d'absorber des villages qui ne dépendaient de lui comme les peuls l'ont bien expliqué.
Ils ont dit que c'est Touba qui a empiété sur leur village.
Même dans la maison de ton père dès fois on fait des choses qui ne lui plaît pas mais il pardonne
Gniome lane moléne yeubou thie villageou diambour sougnou térét tabac civil mifa wara déme dafa am lokhamné kén warouko sétane si réw sérigne sou térét yén yii nako tak déŕ yi lidianti téé nénagnou dieul nagnou ay autos yobou sén lou eup diourome fouki khar lolou sathie wayé dou
May len nitt yi diam peulh day tokh pone.téyite sen deuk la
Bay fal yi doniou tokh
@@moussaba8522 nank rek mo gueune
@@moussaba8522billay bay fallyii kay gniofi dakka toukh 😂😂
Il s interdit la vente ce produit mais ils le consome mon frere passé dautre chose il sont créés leur propre insecurite donc ne nous fatiguer
baye fall yi wakhouniou degggg
Évitez de stigmatiser une ethnie parapor a une secte
ON NE DOIT PAS CONFIER CE GENRE DE TRAVAIL À DES CIVILES.
IL FAUT QUE L'ÉTAT ET LES AUTORITES RELIGIEUSES TROUVENT UNE SOLUTION.
Fatmata yaw daga rew khamo sa bopou moytoul