Bonne continuation el Malick continue sur cette lancée tu ira loin inshaAllah. Yarou, yeuck nieup, nangou liguey. Diam thy yaw frère❤. Je te souhaite un meilleur club comme Barça, Real Madrid, city... Tu as tout le potentiel pour y jouer. Cheikh merci sa liguey rafet na. Amal diam❤
C’est grâce à des initiatives comme Foot+ qu’on peut mieux connaître nos joueurs et leurs parcours. Respect Cheikh ! ❤
C'est le mot xassida qui m'a poussée à regarder la vidéo mais machallah j'aime son mental ❤
Elhadji Malick Diouf le futur meilleur latérale gauche au monde très bientôt inchallah ❤❤
Pro bou humble blh yalna yalla khèp dolii barkep borom touba ❤
Merci Cheikh
J'ai adoré l'émission.
Plein succès El Hadji Malick
Yalla na Yalla Doli la diam waye ak wére ak Ndam Barké Borom Touba❤🎉
Un joueur très correct qui communique bien en plus d’être talentueux
Une fructueuse carrière Maodo
Cheikh yalna na nga goudou fane bou andak weur ak tawfékh diou beuri
Waw goor mouride tawfekh ak tayssir bi barakati Cheikhina Ahmadoul Xadim 🤲🏾🤲🏾🤲🏾
Yaw ki Luka Déf mouride
@@Mbayr-n2gyalla
@@Mbayr-n2gsaway yagui weur di tontou rk wala mouride bimou done dala méti😂
Moma diakhal el Malick moko nakh😂😂@@modoufall959
@@modoufall959 yaaram mouride dëgg yombull layombay nga wax ne murib la té donoko
Encore un G R A N D merci à toi 😇
Cheikh hana dagua def formation journalistes
Tu pose de très bonnes questions
Malheureusement nos journalistes sont nuls ,ils posent des questions bidons
La solution est khadimique serigne touba la ❤❤❤❤bonne continuation malick
Ndeysan magui koy khol di reh rk beug nako dh weurna serigne bi ❤
Nila mél naturellement leu boy bi dafa yagg yarou machallah 😍Bonne continuation ElhMalick domou Medina rue39💪🏾
MACHALLAH YAW DH SOPPOU NAALA LOOl NDAX SRG BI AK XASSIDE YI YALLA NALA YALLA SAMOU ARRLA THI BRK XASSIDE YI
Ak talibé rk mo am solo yagal El hadji Malick❤️
Vraiment il a une bonne éducation
Ki mom damako beugue ndakh serigne touba ❤️🙏🏿
Excellent interview. On sent qu’il a vraiment la tête sur les épaules Machalla.
Akbess la niou beug ❤❤😮😮😮 cheikh akbess la niou beug
Merci beaucoup cheikh vraiment ndanan nga ❤❤❤
Merci beaucoup frère ❤️ ❤❤
machallah beugu na elhdji malick diouf dh girr serigne touba ❤❤❤
Mashallah Yalla nako yalla samm❤
Bonne continuation ❤
une personne vraiment éduqué ✅
Machalla bonne chance ❤❤❤❤ jërë jëff s.touba
Mâcha alla morud di ❤🎉tawafeh rek inchallah ❤🎉
Elhadji Malik Mashallah Jerejeuf Borom Touba ❤cheikh fostyl 💪🏽
Machallah ❤❤❤
Respect un jeune comme pas les autres ❤🎉 respect
Macha'allah, ne change pas...kou yarou, dara djombou ko 🙏🏿
Ndayssane kou am talibé Malick machallah 🇸🇳🫶🏿❤️
Contant de toi cheikh
Ohh machalla musigue mom amoull gnarign darra mangui lay bayyi khell sikanam bone chache❤
Gayi 200k yii bokk ❤🙏🙏
Bonne continuation el Malick continue sur cette lancée tu ira loin inshaAllah. Yarou, yeuck nieup, nangou liguey. Diam thy yaw frère❤. Je te souhaite un meilleur club comme Barça, Real Madrid, city... Tu as tout le potentiel pour y jouer. Cheikh merci sa liguey rafet na. Amal diam❤
Ton regard vers lui a tout dit ❤️
Amal diamb note kou yarou meun limi Def mouride bi❤
Luka Déf mouride
@@Mbayr-n2g saway yagui weur di tontou rk wala mouride bimou done dala méti😂
@Mbayr-n2g dof nga katal sa diobou ndaye
Eladj malik je te souhaite bonne continuation
Soy wakh nga khamne ko am talibe la machaalah
Machalla ki baye fall degue la ❤❤❤
Loka DÉF Baye fall
@@Mbayr-n2g saway yagui weur di tontou rk wala mouride bimou done dala méti😂
Machallah
Machallah dieuwrine ❤❤
Machala tawfékh rk inchala
Machallah ❤❤❤❤ bonne continuation.
Machalla mon frère 😍🥰 adore
Dama beuge blh diamou dio barry à vous ❤❤❤
Il communique très bien ce jeune 🎉
Ndeysane lou wayy ame talibé moko geune 🙏🙏
🎉bly walahi 🎉
Merci beaucoup cheikh🎉
What a player!!
Macha Allah ki sop Nako dh
Machallah yala nala yala samou
Mashalah
El Malick Diouf futur crack
Mashallah bonne continuation 🎉
Ndiaysan 😘 dondal wèral goddal fane
Ndaysan tarkala❤❤❤
Kou man noumy def e bonne continuation ❤
Bonne chance bro
Amna ñooxamni ku léen jege ñu yàq la
Machalla diouf
Ndaysaan yarbi
Abonena afair bi nace na
Ch❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Mais gars yii abonnés Lénne nak bouyague la warona ame 200k d'abonné Inechallah Q'SA
♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️
Yalla nala yalla takhawou bou baax mouride ngua joué si club yi geuneu mak si adouna
🥰🥰🥰🥰🥰
Merci beaucoup 🥰🥰
❤❤❤
am na talibe si wakh
ossi khamna nimouy communiquer
et la modestie
màchaall
Li ma nekh ci mom dafa am talibe
❤❤❤❤🎉🎉
Yalla nga signe real madrid ya meun mendy dh
Amine walahi fouf
Kii khaler la
Cheikh Guzman bi foumou tollou?
😂😂 14:41
🎉🎉❤❤😂😂
❤❤😂
Ki beugue nako blh
Ki mom wagni woul ate
Kii comédien la😂
Mais une très bonne personne ❤️🙏
Boy Medina bou humble ni yomboul dh
Ki boy la de😂
Boy bou ndaw leu
Dell deglou al quraane
KHASAIDE dou alhouran
Machallah ❤
❤❤
🎉🎉🎉🎉🎉❤❤❤
❤❤❤❤❤
Machallah ❤❤
Machallah ❤
❤❤❤❤
Machallah ❤