Avant tout di massawou mbok mi. Lima beug nguene xam moy dougueul asile waroul nek motif guerre kessé. Ex : motif humanitaire etc... Motif guerre woroul ndakh guerre bi maan na diekh tomber sa papier guenagoul nga aam blem. Ex : Gambiens you bari lolou mo leen daal instant yi. Tek ci aussi so dougalé asile ci bene deuk Europe niou bagne ba nopi so deme ci benene deuk dou yomb nga aam ko fa. Même soko waxoul dinaniou ko xam ndakh sa empreinte yi niou diota dieul fofou. Li weer te woor moy niit manoko delo te xamo foumou deuk. Gouvernements Gambie ak Senegal nio yombal rapatriement seni niit lolou lou weer la. Souniou ko signer woul dou yomb cas isoler nak maan na aam. Wayé nio kay signer pour des intérêts bidons sacrifier seni niit. Te li nguene meti même sou lene toubab defalé ay mesures d'accompagnement ( aides) pour gni niiuye dello dou niou lene diokh deureum. Kou aam setlou giss rapatriement yi dafa guene bari aat yi USA, ALLEMAGNE, ESPAGNE etc te li ci doy waar Gambiens ak Sénégalais nio ci eup🤔 Nek Europe niak yor papier takhoul niou rapatrier la wayé na nga moytou aussi yene lieux yi ak di dokh ba yene heures de crime yi. Li ci dess nak nga bayi ko ci lokho Borom bi ndakh maan nga tomber au mauvais moment et au mauvais endroit. Lolou ndogalou Yalla lay doon. Wayé li eup solo moy moytou bi. CONSEIL: Na nguene moytou deposer asile pour motif de guerre pour Sénégal ak Gambie. Sou manoul niak tanaal benene deuk bou aam guerre te niou fay laak français etc... Kou ci massa deposer asile Italie niou bagne diaroul ngay deme fenene di fa deposer asile dou niou la may te di nga lene yombal niou maan la dello ca deuk. Sou lolou wesso kou ci guiss girl bou la beug takaal wala lo ci maan defaal pour aam papier dara nekou ci. Te na nguene di dioubaal moytou beug xaliss bou yomb. Kou jaar ci yoon you meti yi ba doug Europe waar nga gorgorlou bou bakh te moytou leep louye takh niou dila kheep wala delo ca deuk. Yalna Borom bi saam te japalé keep kou touki. Bon courage frères ala athiou. Never give up. God bless y'all.
Slt Ms freres pour asile que soit guerre ou violence c pareille moi jai pas mis guerre est on ma Donne negative wallaye en plus avec un bon discour wallaye c dieu qui donne tout avec la benediction de ts parent pour ce que tu vient de dire je suis daccord avec toi il faut rester calme San avoir aucun probleme faire integre essayer de parle leur langue de faire bcoup de chose incha Allah ça vas aller parsk dieu le tout puissant voit tout wa salam
Merci adama continuelle combat bi demal ci plateau yepou tounkara ak senego ndax nioune sénégalais yi nèk bitim rew niepp xam co metina trop mais yalla bax ne sama xol dafa djèx bilahi
Vous faites des bonne émission mais j’ai l’impression que vos émissions sont faites seulement les sénégalais. C’est vraiment formidable de parler la même langue d’un pays mais moi j’aimerais que vous faites è la traduction à l’écrit.
Adama,reprend ta peche et vote Sonko pour la souverianete economique.Quelqu'un comme toi navait pas a emigre dans un pays normal.Tu est brave et trailleur.
Courage mon Frère, je ne comprends pas ta langue, mais je comprends déjà de quel sujet tu parles, puisque je suis camerounais et c'est toujours pareil que moi, donc c'est aussi un peu comme les gens là-bas, même si tu es bien intégrés il ne veut pas t'aider, il veut juste que tu rentres dans ton Pays, donc il veut juste nous embêter, et aussi et aussi ceux qui travaillent avec les étrangers, des autorités, qui sont très racistes, n'aime pas toujours les Africains c'est un peu comme ça . Courage à toi mon frère que dieu vous bénisse que dieu bénisse l'Afrique que dieu fasse en sorte que les Présidents Africains puissent entendre et que nous les Africains puissions vivre en Afrique et ne pas avoir à aller en Europe 🤦♂️😥
Ich bin München dieser mann er hat vollkommen recht für mich Macky ist ein Diktator ein böser mann für sein volk En wolof Ki lou mou wakh mo am deugue le Allemagne Munich dekk diam le lepp Président Macky sall moko waral da mélni Bougoul ay doomou peuple bi Macky sall goordjiguene le dictateur sacrifier 😂😂🇩🇪🇸🇳🇫🇷😁😁
Le senegal et congolais m ont dépassé il met le titre en français mais lorsque tu cliques pour voir sa commence nalobi nalobi chez le congolais. ..et chez le sengalas tu clique baima baima ndangadeff eeh la famille nous tous on veut comprendre l'émission e pitie soit le titre a lingala ou au wolof mais poster le titre en francais et ecouter ca v décevant
vraiment frérot tu as parfaitement raison bon moi je suis Sénégalais et je vie en France actuellement mais les Sénégalais ils sont vraiment pas en laisse ici en Europe c'est que les Sénégalais qu'ils ne sont pas en laisse ici en Europe c'est pas logique ça quand tu dis que tu es Sénégalais ont te dit directement que y a du travail au Sénégal alors que tout est faux c'est du n'importe quoi ça me fait mal au cœur vraiment je t'en prie président aide les ressortissant Sénégalais ont te demande pas l'argent quand même mais pour papiers 🙏🙏🙏
Regarde moi ça quel triste réalité, Sénégal Bilahi lifi nekk mo raww sakh pays bou amm guère ! mm ici en Italie c'est comme ça macky sall bakhoul dou nitou dara
Courage mon frère c'est très dure...Mais nak danga léwètte lole..say keuyite dara nekouci..Policiers yi bo djengo né je bouge pas d'ici j'appelle mon avocat douniou la yobou fenéu..c'est un pays de droit l'Allemagne...si tes papiers étaient en règle dangay djéngou...yow danga diangoul rekk té léwètte boléci..
L’enfant Béni Si ça ne va pas là-bas tu peux changer de pays l'europe est vaste ! et choisis 1 pays où tu parles la langue c'est bcp mieux ! bon courage
Adama dieng iow Baye fall nga boul meuss ndagou tokk fi senegal 🇸🇳 guérr amoufii mei lifi ame mo raw guérr Jalousie Commencent le président de la république du Sénégal 🇸🇳 lii C’est honteux ☺️ dafa rousse lou trop ki Parcours bimou déf gno beug ko yakk si Zéro dafa gniaw trop nagnou yénaneté diam ak lou bakh wa salam🙏🇸🇳
Kou warra enregistre gnouye werenteh ndakhe senegalais nga Walla Dede Noye dieude billet deme allemagne sans passeport. Suis senegalais vit 25 ans en allemagne
yalnala yalla diapalé si mbarki Mohamed lit métina koi bilahi
😭😭😭Les autorites Senegalais seront les derniers a juger au jugement derniere😭 je t'assure😭😭masa BrO yalla baxna
Yalla Yalla diaple si barck serigne Falliou Mbacke
Courage mon frère réussir ce n'est pas seulement en Europe
Yalna yalla delosila thi diam barke seydouna mouhamadou rasoulilahi saw
Yalla bakhna dina bakh macky mome déye dégagé solution bi sonko la
Ah'nabou'ndong'bou'sonko'solution'mala'beugueu
@@alphasagna226 🤣👍merci
nabou Ndong dégagé reg
@@ninkinankofangbondi3181 waw waw
nabou Ndong Macky baahul chi Afrique. He’s a Neocolonial agent.
Tu es un bon croyant mon cher. Yalna rhi sougnou Borom diaap. Votons Sonko
Na nieup dougou europe inchalah ma ngi koy nianal nieup bepeu sénégalais on souffre en silence
Bilahi wakh gua deug
Yalla nalla yalla diapalé Adama mes souniou président bii d'où darra lii noukoo nitt meuné
Le monde n'appartient pas aux riches ni aux puissants mais il appartient aux hommes de cœurs le present n'est pas un croyant
Avant tout di massawou mbok mi.
Lima beug nguene xam moy dougueul asile waroul nek motif guerre kessé.
Ex : motif humanitaire etc...
Motif guerre woroul ndakh guerre bi maan na diekh tomber sa papier guenagoul nga aam blem.
Ex : Gambiens you bari lolou mo leen daal instant yi.
Tek ci aussi so dougalé asile ci bene deuk Europe niou bagne ba nopi so deme ci benene deuk dou yomb nga aam ko fa. Même soko waxoul dinaniou ko xam ndakh sa empreinte yi niou diota dieul fofou.
Li weer te woor moy niit manoko delo te xamo foumou deuk. Gouvernements Gambie ak Senegal nio yombal rapatriement seni niit lolou lou weer la.
Souniou ko signer woul dou yomb cas isoler nak maan na aam.
Wayé nio kay signer pour des intérêts bidons sacrifier seni niit.
Te li nguene meti même sou lene toubab defalé ay mesures d'accompagnement ( aides) pour gni niiuye dello dou niou lene diokh deureum.
Kou aam setlou giss rapatriement yi dafa guene bari aat yi USA, ALLEMAGNE, ESPAGNE etc te li ci doy waar Gambiens ak Sénégalais nio ci eup🤔
Nek Europe niak yor papier takhoul niou rapatrier la wayé na nga moytou aussi yene lieux yi ak di dokh ba yene heures de crime yi. Li ci dess nak nga bayi ko ci lokho Borom bi ndakh maan nga tomber au mauvais moment et au mauvais endroit. Lolou ndogalou Yalla lay doon.
Wayé li eup solo moy moytou bi.
CONSEIL: Na nguene moytou deposer asile pour motif de guerre pour Sénégal ak Gambie. Sou manoul niak tanaal benene deuk bou aam guerre te niou fay laak français etc...
Kou ci massa deposer asile Italie niou bagne diaroul ngay deme fenene di fa deposer asile dou niou la may te di nga lene yombal niou maan la dello ca deuk.
Sou lolou wesso kou ci guiss girl bou la beug takaal wala lo ci maan defaal pour aam papier dara nekou ci.
Te na nguene di dioubaal moytou beug xaliss bou yomb.
Kou jaar ci yoon you meti yi ba doug Europe waar nga gorgorlou bou bakh te moytou leep louye takh niou dila kheep wala delo ca deuk.
Yalna Borom bi saam te japalé keep kou touki.
Bon courage frères ala athiou.
Never give up.
God bless y'all.
Machalah tu as bien compris pour moi kou defoul dara fi Europe ken doula repatrié du courage yalla a déjà tranché les voies
Nature Humaine je fai asile mais asile dou guerr rek
@@africadiaspora4433 bien sur sociale amna ak humanitaire
Bien dit.aminnnn
Slt Ms freres pour asile que soit guerre ou violence c pareille moi jai pas mis guerre est on ma Donne negative wallaye en plus avec un bon discour wallaye c dieu qui donne tout avec la benediction de ts parent pour ce que tu vient de dire je suis daccord avec toi il faut rester calme San avoir aucun probleme faire integre essayer de parle leur langue de faire bcoup de chose incha Allah ça vas aller parsk dieu le tout puissant voit tout wa salam
Retourne mon frère Sénégal amoul dara tant que guéno doko kham
Bilay
brother👌✌👍💪💪 bii limou wakh dafa lérr gouvernmen Senegal dafa sokhor
Yalla na la yalla diapplé si barké khasidayi amine
Ndeyessane j'ai des larmes aux yeux
Adama lou wêr nga wakh bilahi mais yalla diékhoul yalnala yalla défal khéwal
Ay domérame lale .Légui ésk diokhnane lale khaliss pour le retour.Il faut retourner ,senegal amoul dara
Merci adama continuelle combat bi demal ci plateau yepou tounkara ak senego ndax nioune sénégalais yi nèk bitim rew niepp xam co metina trop mais yalla bax ne sama xol dafa djèx bilahi
Vous faites des bonne émission mais j’ai l’impression que vos émissions sont faites seulement les sénégalais.
C’est vraiment formidable de parler la même langue d’un pays mais moi j’aimerais que vous faites è la traduction à l’écrit.
Yalla bakhna frère sa ira inchala yoroñu sa weurseuk kallah t'ouvre un autre porte de réussit.
Copin boul took Senegal fofou amoul darra fékhél déllou europ
Carrément vrai courage frère c’est pas évident Wallaye
Adama yalla nala yalla takhawou Macky sall moné Sénégal émergent am na lugéye
Yalah nalla yalah takhawou si barke seydina mohamed
Yaw Senegal amoul guerr mai lifa nek mo geuneu meti guerr
Wallahi
😂😂😂
Bilay wallay gnoun ligni doundou mo raw guérre ligueye ba dée do fayékou djague ba dée do ligueye
Lifi nèk guerre moko tanè. Sathie xalissou rewmi diko fowè ba parè Senegalais yi di continuè di votè pour niome.
Doyna waar trop ...t refoule dafa metti
Frere yalnala yala defal li geune si ioe...MACKY SALL mom doulkate 'la
Xeweul grand du courage yallana yala def Lou gueune peace ✌️
Hoo ndaysane li métina trop yalnala yalla diapalé
Courage le grand. .YALLA bakhna
Ndeysan kou geum yalla nga yalna yalla dèfal soutare amine
Adama,reprend ta peche et vote Sonko pour la souverianete economique.Quelqu'un comme toi navait pas a emigre dans un pays normal.Tu est brave et trailleur.
Ohhhh doyna warr mais yalla bakhna Dina bakh inchallah
Courage mon Frère, je ne comprends pas ta langue, mais je comprends déjà de quel sujet tu parles, puisque je suis camerounais et c'est toujours pareil que moi, donc c'est aussi un peu comme les gens là-bas, même si tu es bien intégrés il ne veut pas t'aider, il veut juste que tu rentres dans ton Pays, donc il veut juste nous embêter, et aussi et aussi ceux qui travaillent avec les étrangers, des autorités, qui sont très racistes, n'aime pas toujours les Africains c'est un peu comme ça . Courage à toi mon frère que dieu vous bénisse que dieu bénisse l'Afrique que dieu fasse en sorte que les Présidents Africains puissent entendre et que nous les Africains puissions vivre en Afrique et ne pas avoir à aller en Europe 🤦♂️😥
Adama kuobakh nga he is clean and hard working man . Keep it up bro time will tell
Je luis souhaite son retour en Almagne inchalla soon ! Big up bro
comment il va y retourner
Amine
Nooooon vraiment c méchant nos représentants consulaires. Que dieu te garde homonyme
Toghe naghe la dale
Courage mon frère 🙏🏾🙏🏾🤲
Ich bin München dieser mann er hat vollkommen recht für mich Macky ist ein Diktator ein böser mann für sein volk
En wolof
Ki lou mou wakh mo am deugue le Allemagne Munich dekk diam le lepp Président Macky sall moko waral da mélni Bougoul ay doomou peuple bi Macky sall goordjiguene le dictateur sacrifier 😂😂🇩🇪🇸🇳🇫🇷😁😁
Macky sall vrai domeram la wayè dokhal rek adina mogui sa kanam
C est très dure pour les émigrés
Bon Courage sama wadji Tourne le dos 👌👌
Triste frère 😭😭😭😭que dieu te protège amine yarabi
Mêtina trop grand frère que dieu te protège sunu président bii d'où daara
Yalla na yalla diapalèla aminnnnnn
C'est triste vraiment, honte pour le gouvernement Sénégal
walakhi ya gueum yalla yalnala yalla taxawou🙇🙇
Saway santal yalla sénégal diamou rék mofa nék bilahi damala gné
Deloul senegal conne .Es ce ke tu connai sa vie ?
Saway gnibi mo gueuna yaumb dh diaroul nié démal SÉNÉGAL rék
Le senegal et congolais m ont dépassé il met le titre en français mais lorsque tu cliques pour voir sa commence nalobi nalobi chez le congolais. ..et chez le sengalas tu clique baima baima ndangadeff eeh la famille nous tous on veut comprendre l'émission e pitie soit le titre a lingala ou au wolof mais poster le titre en francais et ecouter ca v décevant
J arrive toujours pas a digerer que macky est president du senegal
😂 je suis mdrrr
😭😭😭😭😭
Ac mane tamiit😔😔😔
Man ak yaw bilahi
Mach Allah wakhtane bii âme na solo lol adama. Merci beaucoup
Courage yalla diékhol dieu et grand boule décourager
Du courage yalla bakh na yalla na yalla diapale
Du courage dieu et grand ça va aller inchallah mon frère
C'est vrai notre président a tous gâté ici
Macki vrai domaram notre senegal est foutu 💔🇬🇭💔🤔
President macky dafniou djite mais yeuremouniou yalla naniou yalla até akk mome
Ndeysann grand yeureumnala lool mé nagne mougne rek Dina bax😭
Yalla nala yalla diapale bagua delou si diam si barke yonete bi
vraiment frérot tu as parfaitement raison bon moi je suis Sénégalais et je vie en France actuellement mais les Sénégalais ils sont vraiment pas en laisse ici en Europe c'est que les Sénégalais qu'ils ne sont pas en laisse ici en Europe c'est pas logique ça quand tu dis que tu es Sénégalais ont te dit directement que y a du travail au Sénégal alors que tout est faux c'est du n'importe quoi ça me fait mal au cœur vraiment je t'en prie président aide les ressortissant Sénégalais ont te demande pas l'argent quand même mais pour papiers 🙏🙏🙏
Grand bi yeureum nako bilayy mais du courage sou yone diekhoull wakhousil dou diekh believ in yourself bro god we help us inchalla
Aywaay yalnako yalla diapalé bou baakh mou délouwaatt Allemagne pour meune égali ay projets wal.
Regarde moi ça quel triste réalité, Sénégal Bilahi lifi nekk mo raww sakh pays bou amm guère ! mm ici en Italie c'est comme ça macky sall bakhoul dou nitou dara
li métina trop way sokhor bakhoul yalla nako fi yalla dieulé si barque seydina Mohamed diokho nitt liguéy diko khange térangam
Courage mon frère c'est dur mais s'il pleut à Dieu tu reviendras en Allemagne inchallah. Nous sommes à Berlin c'est très dur mais Dieu est grand.
Boul toke sénégal da méti
Mè senegale Metiwoule si ñepe
Fo nk
Courage mon frère c'est très dure...Mais nak danga léwètte lole..say keuyite dara nekouci..Policiers yi bo djengo né je bouge pas d'ici j'appelle mon avocat douniou la yobou fenéu..c'est un pays de droit l'Allemagne...si tes papiers étaient en règle dangay djéngou...yow danga diangoul rekk té léwètte boléci..
Lii yeup macky Birou mafé la ndayam😡
😂😂😂😂
DINA bakh inchala non mettina
Cissé bou serigne saliou 😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂
@@mariamadoucoure9692 🤣🤣🤣
Macky dafa sokhorrrr ndayam
Je suis en Allemagne mais Macky sall doméram mo niaw fu Europe ne Sénégal dafa lugéye émergent doull rek
Macky sall wallahi yallah nako sunu akh daaal ...j'ai lu un article y'a meme pas deux semaines wa allemagne daniou sokhla main d'oeuvres si boopap ...
FO nk
No metina trop lep sougnou gouvernement bou yeuss mognou sonal
yaw cambie ga
Moi je suis en Allemagne 🇩🇪 mais c est très difficile pour moi, je travail pas ,je fais rien mais yalla bahkna incha Allah 💪💪💪💪💪💪
L’enfant Béni Si ça ne va pas là-bas tu peux changer de pays l'europe est vaste ! et choisis 1 pays où tu parles la langue c'est bcp mieux ! bon courage
Il faut essayer de tenter un autre pays
L'enfant Beni courage frere💪💪
Merci sama gayi à votre soutien 🇸🇳🇸🇳🇸🇳🙏🏻
Il faut apprendre la langue et faire ausbuldung
soumademe ,erope ,douma demati ,senegal
Yalla nala yalla dimbali
Oh 😭 ndeysane
Brother God bless
Ndaysane mettina me je te souhaite de bonheurs
Adama dieng iow Baye fall nga boul meuss ndagou tokk fi senegal 🇸🇳 guérr amoufii mei lifi ame mo raw guérr Jalousie Commencent le président de la république du Sénégal 🇸🇳 lii C’est honteux ☺️ dafa rousse lou trop ki Parcours bimou déf gno beug ko yakk si Zéro dafa gniaw trop nagnou yénaneté diam ak lou bakh wa salam🙏🇸🇳
Du courage mn frere tè un diambar du courage yalana la yalla defal li gueun si iow
Bon courage Adama dina bakh incha Allah
Ça fait mal , en tout cas moi c est a cause de la famille he suis parti, mais grand Dieu est grand.
Bilay wadji dafmay yokou diom début 2 sne magui visa affaire deguer me douma moussa Khadi nianal lenma way
Courage frère yalla bahe ne
Li d'où deug d'où yone ki gñiata nitte la yorone mais frère dafa yallah diékhoul
Du courage mon frère je suis sénégalais et je vie en Allemagne depuis 8 ans les sénégalais souffre en Allemagne
Ah boul gnou titeul wayy, gnoune gni Wara gnew fofou kome étudiant
SENEGAL DAFAA TAARR FFIII KENN MOUNUFII NEKK SI DIAM
Courage bro on love
Lassana Camara vous avez le même nom et prénom que mon père il est décédé🙏🏼j pouvé pas passé sans commenté
Thioy Senegal yala naniouyala japalei
Europe bi yeup mo meti bilay walay aucune considération pour nous bilay yalah nala yalah dimbale
Kou warra enregistre gnouye werenteh ndakhe senegalais nga Walla Dede
Noye dieude billet deme allemagne sans passeport.
Suis senegalais vit 25 ans en allemagne
Jai mm pleuré. Sa ma fait male. Ces vraiment triste .pour koi macky salle ne nous laisse pas vivre en paix.
Ndeysaane Waadji Damaka Yeurreum Sakh....Té Lou Policier Wakh Rek Mouni Amoul Blem...Dafa Gueum Yalla Trope
Bien dis frère, j'ai aussi passé par Maroc mais c'est pas facile 🇸🇳🇪🇸 Barcelona
Bien d chose a toi mai j'ai entendu ya rien en Europe la vie est dure laba esk c vrai
Frère déloul Maroc yalla bakhna Président bou tothie leufeul ndém laniou am
Bravo Adama bro
Boufi Tok dh dokhal dem diarnako Sénégal moy lolou dh
Yalla nala yalla dipale si barke Seydina mouhammed
C est simple, ne vote pas pour un gouvernement qui ta fait du tort avec tte ta famille
tu nous manques bro
C très dur de vous sa
Li dawna yaram
@@khadypouye5048 salut khady est ce que tu connais le gars moi je suis à Munich
Khady pouye répond moi ou bien tu m envoie ton numéro oder ich gebt dich meine numer danke
Brother courage rk yalnala yalla guene diapale si barkeb mohamed
Du courage mon frère Sénégal dangne KO wara diaye gnou partagé halisby
Courage frère yalnalaa yalla taxawou
Du courage frr lidieunti rk lepay bakh inchallah