Serigne Ndiaye ouvre le feu 🔥 sur Eumeu Sène et Doudou Sané : "00 franc ma dane lén ci 5 minutes..."

Поділитися
Вставка
  • Опубліковано 2 січ 2025

КОМЕНТАРІ •

  • @Khalil-xy9ps
    @Khalil-xy9ps 9 днів тому +12

    Lamine tjrs pertinent dans ses questions.vraiment chapeau à toi

  • @mbayeseye5712
    @mbayeseye5712 9 днів тому +8

    Serigne Ndiaye futur roi inchallahh ❤❤

  • @cheikhmbacke72
    @cheikhmbacke72 8 днів тому +3

    Lamine seck vremant je l'aime bien car tu posse dhe kesion pertinent bilahii

  • @Omarsane7491
    @Omarsane7491 9 днів тому +2

    Serigne Ndiaye del wathi thi mbappat yii frère lutte simple dafa manque Ay lourd

  • @salioudiallo3412
    @salioudiallo3412 8 днів тому +1

    Le grand champion serigne Ndiaye 2

  • @AbdoulayeGueye-nt8hz
    @AbdoulayeGueye-nt8hz 7 днів тому +1

    Tu as tt le temps devant toi prend les adversaires qu’ont te proposes comme Doudou Sané Gora Sock et Zambala , tu fais tes preuves et avance.
    Athiaa Champion 😎✌🏾

  • @AblayeNdao-u1s
    @AblayeNdao-u1s 9 днів тому +2

    Eumeu nako dieul futur roi inchallah 🙏🙏🙏🙏🎉🎉🎉

  • @papemoussadiop83
    @papemoussadiop83 8 днів тому +2

    mes doudou sane mes serigne ndiaye mon meune doudou serigne ndiaye champion la

  • @amadiallo-kn2ye
    @amadiallo-kn2ye 9 днів тому +3

    D’accord avec toi serigne ndiaye ni leu prends doudou et avance …Lamb leu dafay neeex rek et je te garantis que fi leu sa lamb di oubeko nak in cha Allah

  • @mbayeseye5712
    @mbayeseye5712 9 днів тому +1

    Serigne Ndiaye eumeu sene ❤❤

  • @MarsFrom
    @MarsFrom 9 днів тому +1

    Wawaw Diambar ak mbeur deug❤❤

  • @babacardiop10
    @babacardiop10 8 днів тому +3

    Le lion a parlé deh bilahi amoul ragal

  • @amadousarr1957
    @amadousarr1957 9 днів тому +2

    Fii la lamb toolou merci Serigne

  • @badiafaye5314
    @badiafaye5314 8 днів тому

    Diara diéf merci ❤❤❤❤

  • @laminethiam1599
    @laminethiam1599 8 днів тому

    Alkhamdoulilah Serigne Ndiaye niemena😂

  • @IssaSarr-st5id
    @IssaSarr-st5id 8 днів тому +1

    Waw yew serigne ndiaye fo tohie yew

  • @lomassamba8936
    @lomassamba8936 8 днів тому

    Lamine massallaa question yi rafét na lool

  • @mauricefaye3075
    @mauricefaye3075 5 днів тому

    Le roi sané xalé doolé dou niekhou niebé kène 😂😂

  • @assanediagne6088
    @assanediagne6088 9 днів тому +1

    Machallaaaa

  • @bambagueye2454
    @bambagueye2454 8 днів тому +1

    Sa thiés serigne Ndiaye 2 combat la

  • @AbdoucisseSarr-qn9hv
    @AbdoucisseSarr-qn9hv 9 днів тому +6

    Wala lamine lolou moye wax dji na wathi mbappatt bi ragal moléne diapp ordinateur moléne djitou thi lamb fouff té moungui thi ba légui ❤❤😊😊

    • @sambandiaye6472
      @sambandiaye6472 9 днів тому +4

      Khar day wessou mbottè

    • @georgesdieganediouf2684
      @georgesdieganediouf2684 9 днів тому +6

      Ordinateur sa carrière est pour les mbappats il est en retard sur l'arène avec frappe

    • @georgesdieganediouf2684
      @georgesdieganediouf2684 9 днів тому +3

      @@AbdoucisseSarr-qn9hv kou beugua tekki nék champion digua bayi mbappat

    • @georgesdieganediouf2684
      @georgesdieganediouf2684 9 днів тому +2

      Mbappats a des limites kou beug tekki digua bayi mbappat dem lutte avec frappe.
      Ordinateur moromam yeup raw nagneko.

    • @laminediabakhe8459
      @laminediabakhe8459 8 днів тому

      Ki kouy ragal soriko MMA koukoy def do ragal m bapat Serigne n diaye pasénako

  • @TidianeMbengue-u9z
    @TidianeMbengue-u9z 8 днів тому +1

    Tapha il faut savoir y a des suites serigne n diaye c le champion gris n est plus a la mode qu il laisse les jeunes

  • @AbdoucisseSarr-qn9hv
    @AbdoucisseSarr-qn9hv 9 днів тому +1

    Téna xamné défaite la bayé mbappat Dakar ❤❤❤

  • @djimbaniang2190
    @djimbaniang2190 9 днів тому +2

    Deuegu rek mo meun Doudou Sane de

  • @Maman-x9e
    @Maman-x9e 8 днів тому +1

    ❤❤❤❤❤❤

  • @abdoulienjie5999
    @abdoulienjie5999 8 днів тому +2

    Mane yaw ak doudou sane comba la

  • @salioudiallo3412
    @salioudiallo3412 8 днів тому

    Bilay do moromou boy bobou

  • @abdoulienjie5999
    @abdoulienjie5999 8 днів тому +2

    Mbapat Dou door dh

    • @salioudiallo3412
      @salioudiallo3412 8 днів тому

      Mais dorr aussi dou mbapat ki mo meune doudou thie côté yeuppe

  • @adamandiaye5622
    @adamandiaye5622 8 днів тому

    Coriace aka sadik😂😂😂

  • @sambandiaye6472
    @sambandiaye6472 9 днів тому +3

    Wa yene gniy wakh affaires doudou sanè ,serigne ndiaye 12/0 la def doudou sane fatè khedioufi
    Doudou moy nakh ay supporteurame

    • @Madou-h1g
      @Madou-h1g 9 днів тому

      Ses pas vrais amoul weranter khouhane tequi toubeuye na diel avance bi

  • @alioubadoundiaye9191
    @alioubadoundiaye9191 8 днів тому

    Waw diélal avance bi

  • @TIJ..Senautocanada
    @TIJ..Senautocanada 9 днів тому +1

    Toggal fofou di khaar Eumeu Sene rek
    Doo gawa beuré

  • @ProcureurYoutube
    @ProcureurYoutube 8 днів тому

    Lamine louko dall ak tangallam bii

  • @KhadimDiouf-uu5jo
    @KhadimDiouf-uu5jo 8 днів тому +1

    Daka barii wakh demal beurre ak doudou sane

    • @MamadouDieng-ce7uc
      @MamadouDieng-ce7uc 7 днів тому

      Yennn louy senn problem bayilenn sokhorr way

    • @MamadouDieng-ce7uc
      @MamadouDieng-ce7uc 7 днів тому

      Boulenn lamb boler rk denagne beurer nimko meuner thi mbapatt nonoulako meuner thi Dorr bi

    • @KhadimDiouf-uu5jo
      @KhadimDiouf-uu5jo 7 днів тому

      @MamadouDieng-ce7uc lolou ay wakh la rek n'a dieul enfance biii rek

  • @afro3827
    @afro3827 9 днів тому +4

    Saway beurel ak say morom ben grand doulafi may chance yak doudou sané wala zambala gnoy say adversaires

  • @alassanendong9610
    @alassanendong9610 8 днів тому

    Coriace kessé

  • @morseck3716
    @morseck3716 9 днів тому

    🎉

  •  9 днів тому +3

    Doudou sané moleu meuneu foufffff

    • @sambandiaye6472
      @sambandiaye6472 9 днів тому +1

      Wakho deug deh

    • @mandellandoye1908
      @mandellandoye1908 9 днів тому

      Serigne ndiaye l'a déjà terrassé plus de 7 khawma 8 fois 😂.
      Serigne ndiaye mo modeste rek mais ni reug reug ignorer franc lako warone ignorer

    • @Mo13092
      @Mo13092 9 днів тому +2

      Lolou Doudou douko wakh ay supporteram niokay wakh

  • @BilalDiagne-x1t
    @BilalDiagne-x1t 8 днів тому

    Fékhel dane mbeur bou bax
    Iow danago sa ben morom bou confirmer
    Tu parle comme si que t’a battue tous le monde

  • @nogayeniang9119
    @nogayeniang9119 7 днів тому

    Yaw daw rek laye def dou dial doudou sane laye khar emeue sene

  • @khadimsow7149
    @khadimsow7149 8 днів тому

    Serigne ndiay ioe fo tothie😂😂😂😂

  • @abdoulayebar7135
    @abdoulayebar7135 9 днів тому +2

    Serigne Ndiaye tiouth day kham lekam vous la nouvelle génération defolene fi dara di lathieu grand

  • @souleymanendiaye-n6h
    @souleymanendiaye-n6h 9 днів тому +2

    Mbeur yo nioko ragal rék mé agg na si kow

  • @JuloBorah
    @JuloBorah 7 днів тому +1

    Bayil ba doudou fake la fi

  • @mouhamedndiaye2111
    @mouhamedndiaye2111 8 днів тому +1

    Mayé chance dafa am limite daan Eumeu sene junior ak Bb saloum beugua yégue cours des grands 😂😂 non lamb nekhna légui 😂 Aliou seye 2 mo mériter niou mayko chance mais pas kii vraiment

  • @BilalDiagne-x1t
    @BilalDiagne-x1t 8 днів тому

    Iow bébé saloum bi nga moudié dane Jacob dane nako ba dieul tiatou yoff nga nekk fi di tamou rk

  • @moussapayemane4167
    @moussapayemane4167 9 днів тому +1

    Sérigne Ndiaye 2 micro la timm rék 😂mais niéméwoul Doudou sané mouk,khadafi dof la déh,da am fite,niémé té day khékh 😂

    • @Stefbadji
      @Stefbadji 9 днів тому

      Sérigne Ndiaye 2 dann na doudou sané 7 foi mapatt

    • @sambandiaye6472
      @sambandiaye6472 9 днів тому

      Yow demal ladie doudou sane niatta lako serigne ndiaye dane

    • @moussapayemane4167
      @moussapayemane4167 9 днів тому +1

      @@Stefbadji manoma wah dara si lamb nopil,surtout lutte simple am na mbeur youma sétane boumalako ladjié doléne ham,Sérigne Ndiaye bou niémé Doudou nako dieul,monguini amoul combat

    • @moussapayemane4167
      @moussapayemane4167 9 днів тому +1

      @@sambandiaye6472 manoma wah dara si diganté Doudou sané ak sérigne Ndiaye 2 donc nopil,lima ham si lamb hamoko,surtout lutte simple,amoul combat kagne bouko niémé nako dieul niou hol

    • @Mo13092
      @Mo13092 9 днів тому

      Lolou ioe yakoy wakh Doudou douko meusseu wakh 😂😂😂
      Doudou Sané yaboul Serigne ndiaye

  • @AlphaNdiaye-wq4zv
    @AlphaNdiaye-wq4zv 9 днів тому +1

    Zambala Mola dane waxal deug iow do Dara

  • @BadaraSarr-q9d
    @BadaraSarr-q9d 9 днів тому

    Serigne ndiaye vraiment tu n'est pas aussi technique pour terrassé les eumeu et doudou soit logique un peu si c'était pas ta taille t'aurais beaucoup de mal dans la lutte

    • @Mo13092
      @Mo13092 9 днів тому

      Tu sais combien de fois il a battu Doudou Sané en lutte simple 😂

    • @BadaraSarr-q9d
      @BadaraSarr-q9d 8 днів тому

      Non je parle pas que de la lutte simple

    • @Mo13092
      @Mo13092 8 днів тому +1

      @@BadaraSarr-q9d crois moi même en lutte avec frappe Serigne ndiaye est meilleur que lui

    • @GueyePape-t4m
      @GueyePape-t4m 8 днів тому

      Badara xana yago setane Serigne Ndiaye 2 gnom balla Modou Lo yep gneme nako gewal ak gnome malgré aga gufa

    • @laminethiam1599
      @laminethiam1599 7 днів тому

      ​@@Mo13092ta bien précisé en lutte simple les années passées

  • @AlphaNdiaye-wq4zv
    @AlphaNdiaye-wq4zv 9 днів тому

    iow zambala Mola dane waxal deug

  • @laminethiam1599
    @laminethiam1599 8 днів тому +2

    Alkhamdoulilah Serigne Ndiaye niemena😂

  • @Sarrtvfissel
    @Sarrtvfissel 8 днів тому +1

    ❤❤❤❤❤❤