Première réaction de coach Bakary après F2F: « Ama dafa tite…waroul wate 🤔

Поділитися
Вставка
  • Опубліковано 2 лют 2025

КОМЕНТАРІ • 152

  • @mouhamedlo1093
    @mouhamedlo1093 14 днів тому +38

    Franc yalla nga am ndam inchallah ❤

  • @tk92221
    @tk92221 14 днів тому +29

    Nekhoul ba nekhoul mais Bakary il dit tout le temps la vérité. Amoul far lim fi wakh yeup c’est carré

  • @meda6445
    @meda6445 14 днів тому +16

    Respect Coach.
    Ndiolmi tu est tres professionnel.
    R.A.S

  • @Falléma35
    @Falléma35 14 днів тому +28

    Franc yalla naguo borom bi may ndame j'ai constaté que on le sous estime lamb djii amoul démocratie

  • @MohamedBadou-w3w
    @MohamedBadou-w3w 14 днів тому +15

    Bravo coach bacary merci pour ta vision du combat

  • @mbayesarrdia4470
    @mbayesarrdia4470 14 днів тому +14

    Yallna yalla maye ndam franc Inshallah

  • @prosperpreira6685
    @prosperpreira6685 14 днів тому +14

    Coach bakari moi je suis d'accord avec toi

  • @matarbodian2912
    @matarbodian2912 14 днів тому +2

    Bakary limoy wakh amna solo trop ❤

  • @maremethiam8800
    @maremethiam8800 14 днів тому +7

    😂😂😂 c'est clair 😂😂😂😂 franc c'est du sérieux déh 😂😂😂

  • @Billy_The_Kid_19
    @Billy_The_Kid_19 14 днів тому +46

    Wa Pikine sen fiite taxawoul déeh motakh niouy thieupi thieupi rek mais FRANC bima guiss dara safouko 😎

  • @thiernodembaya8355
    @thiernodembaya8355 14 днів тому +3

    Merci beaucoup coth ❤🇸🇳🙏Ama baldé conte sur fétiche me inch'Allah Dam reck pour Fran inch'Allah 🙏🇸🇳🇸🇳🇸🇳🇸🇳🇸🇳

  • @ShiekhjobeTijan
    @ShiekhjobeTijan 14 днів тому +11

    Franc Yalna Yalla May franc ndam lo Rey ta Gaw ❤❤❤❤❤❤❤

  • @abdoudiagnedoudiagne7962
    @abdoudiagnedoudiagne7962 14 днів тому +6

    Merci bakari

  • @IbahimaDiack
    @IbahimaDiack 14 днів тому +2

    Non coach vraiment il est incroyable

  • @davelelion8789
    @davelelion8789 14 днів тому +1

    Merci beaucoup Coach Bacary 👏🏾

  • @oussoubane2712
    @oussoubane2712 14 днів тому +4

    Coach, ta compétence ne fait pas de doute. Quand tu parles sportivement de "lamb" c'est de façon scientifique. On s'en régale et en redemande. Seulement, il faut accepter que le public aime aussi entendre des commentaires venant de personnes qui parlent avec le coeur, d'anciens lutteurs, ou d'initiés ayant des niveaux différents. En d'autres termes, il faut de tout pour animer le monde de la lutte. Chacun parle dans son registre. Donc prière d'en tenir compte et de ne pas rechercher la confrontation. Un homme de science ne doit pas chercher à écraser ses vis-à-vis. Bien au contraire, il doit leur donner subtilement l'envie de s'améliorer. Autrement, il y a des gens qui redouteront toujours de partager un plateau avec toi. Et c'est le public qui en sera perdant.
    Merci d'avance pour la compréhension.
    Un fan ayant plus de 55 ans.

  • @NgagneMbow-k2u
    @NgagneMbow-k2u 14 днів тому +6

    Man live backry rek la meun setane dafa nekh tee logique lay wakh kholoul lou nekh ken 😂😂

  • @docteurdocteur457
    @docteurdocteur457 14 днів тому +17

    Coach loumay d'accord ak yow beurri woul, mais tu as parfaitement raison dama guiss ni dagn ko beugg soukhlou si combat même le chanteur n'était pas professionnel dafa waronn yamale lolou rafetoul, combat bi dina la si jappalè franc inchallah man beugouma kougni sott diko newal dollè

  • @malicksarr2141
    @malicksarr2141 14 днів тому +1

    Franc yalnako yalla maye ndame sikawe ama baldé

  • @AbyDiaby-w7w
    @AbyDiaby-w7w 14 днів тому +7

    fran seul parcélle moye diriger ndam rk inchallah kome nonou ama tapéte leu fran kassé touss

  • @Pmp90
    @Pmp90 13 днів тому +2

    Wallahi ama da ragal té begoul lamb dji egue 😂😂😂

  • @AbyDiaby-w7w
    @AbyDiaby-w7w 14 днів тому +5

    fran seul parcélle moye diriger ndam rk inchallah kome nonou ama tapéte leu

  • @issaseck9791
    @issaseck9791 14 днів тому +1

    Tu as bien dit

  • @mamourndoye686
    @mamourndoye686 14 днів тому +9

    En tous cas coach Bakari limou wakh yeup deugu leu et limou wakhone guisnagn ko

  • @bayeratebayerate5893
    @bayeratebayerate5893 14 днів тому +2

    Yalla na yalla maye ndam France

    • @Jnrjoop
      @Jnrjoop 14 днів тому

      Italy yalnako yala may ndam😂😂😂😂

    • @sonkoomar2165
      @sonkoomar2165 13 днів тому

      😅😅😅

  • @abdoulayeniang2511
    @abdoulayeniang2511 12 днів тому

    Merci coach le 16 lanouye comprendre😂🙌🏿🎉

  • @salioufall8313
    @salioufall8313 14 днів тому +4

    Ama louniou ko gemlo mokoy dane chaque jour😂😂😂

  • @vieuxngom3760
    @vieuxngom3760 14 днів тому +1

    Le nga la dafa pertinent bilahi

  • @vieuxngom3760
    @vieuxngom3760 14 днів тому +1

    Deug nga wakh déh

  • @akimoulakimseck
    @akimoulakimseck 14 днів тому +6

    16:40 Franc dé kou djoudo parcelles kham ngani bamouye ame 14 15 ans di topp magg dane da ponkalone 😂😂😂

  • @pescarafall8414
    @pescarafall8414 14 днів тому

    Yalla na yalla may ndam ama

  • @saliouthiam2462
    @saliouthiam2462 14 днів тому +8

    Goor dou bétté di door 😢😂😂

    • @Bayeniang20
      @Bayeniang20 14 днів тому +3

      Saway sois honnette franc bi ama di nieuwe moukoy ghiss 2 ama narona danou franc di lakatou si baye😂

    • @senegaleventschanel6913
      @senegaleventschanel6913 14 днів тому +3

      @@Bayeniang20bane lakatou si baye meune wakh loula nekhe , baye dafa done wakh ak mome

    • @SaliouDiop-e4r
      @SaliouDiop-e4r 14 днів тому +2

      @@Bayeniang20😂😂

    • @ThiernoDiallo-c1k
      @ThiernoDiallo-c1k 14 днів тому

      Ioe sa sarap ndy doul rek guay deff

    • @saliouthiam2462
      @saliouthiam2462 14 днів тому +3

      @@Bayeniang20 saa waay moment bobou franc mongui wakh ak baye Ndiaye guissou ko fall ama daff ko bétte

  • @megalebu
    @megalebu 14 днів тому +6

    Ama wallahi dafa titt mo takh mouy def yeufou dof yi . Et puis promoteur bi na yamalè . Le 16 franc dina dane ama INCHALLA

  • @sophrotall8105
    @sophrotall8105 13 днів тому +1

    Bilahi ya wakh li am Ama dafa tiiite mannn lolou la gueum Nieuk motakh mou insister si combat bi. Bimoukoy ladj dafa tangonnn rekkk

  • @Nitou1990
    @Nitou1990 14 днів тому +2

    Ama amna client bou doy warr😂😂😂

  • @elhadjimaodoniang5531
    @elhadjimaodoniang5531 14 днів тому +1

    Deego français tu nous amerde
    Wakhoffi thiotou ndeyam maître chanteur nga🔥🔥🔥🔥🔥🔥🔥

  • @falloufall2765
    @falloufall2765 14 днів тому +1

    Bakary bayill doulle🤫🤫🤫🤫

  • @saliouthiao9983
    @saliouthiao9983 8 днів тому

    Saway franc béneu lokho ladone khékheii ak 3 personnes nganei dafa daw téléphone bi thi lokho gauche bii

  • @mouhamedba738
    @mouhamedba738 14 днів тому +4

    Coach yaw le jour ngay comprendre kouy amaaaaa

    • @leeprinceengage1763
      @leeprinceengage1763 14 днів тому +1

      Coach Bakary mais il contradictoire sur c’est propos Day Doule rekk may wakh mou nane Franc est vif que Ama mais c’est pas vrai Franc De Disss

  • @mountakhagueye2680
    @mountakhagueye2680 14 днів тому +7

    ama danone nafi gouye gui si signature gouygui d'âne ko arène ba

  • @almaktoumdiop8749
    @almaktoumdiop8749 13 днів тому +1

    Franc gñiéti nite gñiokodone sote té Franc kholéne lokho Franc bii télefone lasi té. di khéyékhé bena lokhobi

  • @Ismaeljallow-k3b
    @Ismaeljallow-k3b 13 днів тому +1

    JEREJEFF COACH BAKARY YAW NITU DEGUE NGEU. YALLA FAYLA AAMEEN.

  • @iboudrame4436
    @iboudrame4436 13 днів тому

    Apoo len wakh rek beu arbitre sifflet Ama Baldé dieul Fran diko ragal Pikine ragal deukou fi té Ama beuré na beuss bouné claf Ama Baldé gouy gui ak tapha tine mi eup dolé fran mou dieul claf bi 💪✌️❤️❤️❤️ fran bombardier rek lafi daan ci fin de carrière mais wakh deug Yallah diaroul fi Ama Baldé diar

  • @Biper-k3x
    @Biper-k3x 14 днів тому +2

    Tu as parfaitement raison

  • @katimtoure-h2p
    @katimtoure-h2p 14 днів тому +3

    Franc ❤ seul ❤

  • @MansourSambou-k2d
    @MansourSambou-k2d 7 днів тому

    Dél wax rék ba arbitre sifflet 😂😂 ama dinaléén bétt

  • @cheikhdiop570
    @cheikhdiop570 13 днів тому +1

    Bakary wakh na lepp ama dougual na Franc si combat bi

  • @moussafall4290
    @moussafall4290 13 днів тому

    ❤❤❤❤❤❤🇸🇳🇳🇱🇸🇳✅✅💪

  • @moustaphadiop-md4jx
    @moustaphadiop-md4jx 11 днів тому

    Franc seul❤💪🏽💯⚔️

  • @MohamedThioune-p9k
    @MohamedThioune-p9k 14 днів тому +4

    Fran Mo man 10 ama

  • @mamadousarr4791
    @mamadousarr4791 14 днів тому +4

    Franc mo meun ama fouf

  • @jazaka3178
    @jazaka3178 14 днів тому +3

    Ama lamign bi mo pata fi la fi wakhone bou guissone Modou lô dou si def 1000f niou rokosss 26 ... ba ay mbokam daw dougou si guëw bi

  • @Jnrjoop
    @Jnrjoop 14 днів тому

    😂😂 paréna parewoul Ama day Dane ndiago bi ✌️✌️✌️

  • @niassesouleymane7163
    @niassesouleymane7163 12 днів тому

    Je suus un Fan de Ama Baldè mais Franc est un adversaire très redoutable, très sérieux ... Cest la première fois que jai peur pour Ama

  • @khadimfall979
    @khadimfall979 14 днів тому

    ❤❤🎉🎉🎉

  • @ansumanjarju1566
    @ansumanjarju1566 14 днів тому

    Bakary toi tu te fais le grand connaisseur comment tu te permets de dire que Ama dafa titte

  • @ResidenciaImmobilier
    @ResidenciaImmobilier 13 днів тому

    Kouwax loudoul Ama dafa tiiit waxo touss😂😂😂😂

  • @jeanmariendione4004
    @jeanmariendione4004 14 днів тому +3

    Le gars là il reste à l'extérieur et il parle . Le sport de combat cest pas la lutte franc Ama dakko bett mais kou kham sport deugu khamni Ama balde mm n'est pas un fin bagarreur, il doit apprendre a esquiver car lou tioy li beurri je vois que les remises de franc son plus sûr donc Ama na moytou remise Franc bi . Malgres tout Jacob m'a déçu waroul door franc car mom sérére yi dagn ko adapté dakh jambar bimou doneuh mo waroneuh atei teyei Ama mais door bimou door motakh franc repositionné wou pour jakarlo ak mom bala mouy atei

  • @Dieng-vk6if
    @Dieng-vk6if 14 днів тому +1

    Ama baldé bi beurré wone ak feugue leu AK malick niang ama bobou Pour mou nieuwate dou yombou ndakh âge bi yokouna epui ak blessure yuifi diarre

  • @abdoulayeka4624
    @abdoulayeka4624 14 днів тому +1

    Ils ont Tenu Les mains de franc, et ama avait les mains libre.

  • @Bakelsen99
    @Bakelsen99 14 днів тому

    Thiéye bakary Sakho Sakho biii😅😅😅😅😅😅🤫🤫🤫☠️☠️☠️☠️😅😅😅😅😅

  • @PapemorFaye-d7k
    @PapemorFaye-d7k 14 днів тому +3

    Ama dafa raguale faran

  • @adviseragnam7050
    @adviseragnam7050 13 днів тому

    Ama vraima parewul defa melni kou am blèssure diko neub😢

  • @abdoulayediallo4028
    @abdoulayediallo4028 14 днів тому

    Ama déy door fran mou danou

  • @bayeratebayerate5893
    @bayeratebayerate5893 14 днів тому +2

    France mou man 10 ama

  • @FelixBaraye-j8p
    @FelixBaraye-j8p 13 днів тому +1

    Franc seul.

  • @MedouantaSarr
    @MedouantaSarr 14 днів тому +6

    Bokou niou sax franc mo guena paré fouff

  • @Wrestling1890
    @Wrestling1890 14 днів тому +2

    Franc kerssa bi meune nala nakh complexé la mais dou ragal
    Ama boumou deff erreur bobou xéll rk franc jamono djii kén douko djaye dollé

  • @souleyndiaye1165
    @souleyndiaye1165 12 днів тому

    Ama dafa ragal wakhou dof wesouwoule lolou

  • @boubacardiallo1454
    @boubacardiallo1454 13 днів тому

    Non Bakary Sakho soff ngua da ngua niémé graw grawlou

  • @mehandiaye
    @mehandiaye 14 днів тому

    Combien de lutteur qui était prêt physiquement et qui était sur de bonne lancée ont était terrassé ??

  • @nicolanicola3399
    @nicolanicola3399 14 днів тому

    Bilaye le 16 fevrier ngueine khamener peul bi moye lambe franc Ama dinako wayadilo

  • @ChékhSéne-c1p
    @ChékhSéne-c1p 14 днів тому

    😅😅❤

  • @cheikhdiakhate219
    @cheikhdiakhate219 14 днів тому

    😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂

  • @ismacisse7162
    @ismacisse7162 14 днів тому

    Bakari déle wakh deugue siteu bou taha wone beure niou mouna wakh

  • @HabibGueye-x4e
    @HabibGueye-x4e 14 днів тому

    lou ler ngua wakh

  • @MoustaphaDabo-b4y
    @MoustaphaDabo-b4y 14 днів тому

    Wonder

  • @BathieDiaw-c8l
    @BathieDiaw-c8l 14 днів тому +1

    Ama comba bi doufa 'yakare khekhe douko franc d dane douko yeugue

  • @xnobot2.058
    @xnobot2.058 14 днів тому

    Franc nake bouye dieme serasla refete deh niawe deh am telling you

  • @abdouloume7373
    @abdouloume7373 14 днів тому +1

    Gas yi Nak lolou lanu khamoul khékhou plateau lheu bilay bou amoon diapp daan, Franc daan nako bou yagu
    Franc kenn meuno ko door té diappo ko, Ama dakhoul kheekh Franc
    Yeen khamoulen sakh Li khew Franc faléwul sakh Ama Baldé, mann je vois meme k Ama combat bi daf ko dépasser.
    Franc meunul beuré wakhou dof lheu ak wakhou niakka kham, Balamay beugua dé niounan Ama dafa am sagn sagn. Franc meuna beuré Wala meunul demal seetan special bapatam thi page lutte Tv
    Yaw mom Diol MI chak instant lo critiquer thi Franc rek gay khol, Franc meussul Yeekh
    Daga paré pour wakh thi lamb, demal gua gueustu dji Franc seetan ko parsk yaw khamo Franc
    Ama merr nguembou la té merr nguembou daan meussul am thi lamb
    Bilahi Ama bou yomboo Li le 16 Pikine keupp seen reeer

  • @MilkMilo-qr5uc
    @MilkMilo-qr5uc 14 днів тому +2

    Logiquement sans mystique bou franc diapé ama dako wara dane en moins d'une minute

    • @delgado7915
      @delgado7915 14 днів тому +1

      Loy wax ni

    • @delgado7915
      @delgado7915 14 днів тому +1

      Ioe défaite macky sall bi daf la traumatiser

    • @MilkMilo-qr5uc
      @MilkMilo-qr5uc 14 днів тому

      @delgado7915 lima wakh moy logique lamb franc da eupp dolé ama eupp ko cpmpetion kou meunoul dane gris

    • @MilkMilo-qr5uc
      @MilkMilo-qr5uc 14 днів тому +1

      @delgado7915 yow mome t dans nuages on parle de sport mais hélas toujours dans les balivernes🤦🏽‍♂️

  • @BarkaKoita
    @BarkaKoita 14 днів тому

    Yow khamo daraa

  • @aboubacarndiaye779
    @aboubacarndiaye779 14 днів тому +1

    On dit un décalage c'est masculin,soit on parle la langue de Molière soit le Wolof.

    • @mamadounianghane2330
      @mamadounianghane2330 14 днів тому +2

      Il dit aussi un explosivité alors que c'est une

    • @Galsaint
      @Galsaint 14 днів тому

      Gnoune ay wolof lagnou

    • @abdoukhadredjilybeye8785
      @abdoukhadredjilybeye8785 14 днів тому

      respecte la ponctuation toi aussi. té bayi complexe bi .. XAMM limlayy wax mo eupp solo

  • @vieuxngom3760
    @vieuxngom3760 14 днів тому +1

    Ki dafa gnémé deug

  • @piraterie9996
    @piraterie9996 14 днів тому

    Ama moy bandit thieuy peulh bi Amadou baldé rombo len Franc di daw beu legui 😂

  • @IbrahimaNdao-i9i
    @IbrahimaNdao-i9i 13 днів тому +1

    Pour moi franc est au dessus

  • @bachiroubadiane3135
    @bachiroubadiane3135 13 днів тому

    Coach parfois dey wakhe bakene

  • @mamadubalde3118
    @mamadubalde3118 14 днів тому

    Pourtant on disait sa sur tapha tine ba jour ci rek

    • @Aliotop-officilel
      @Aliotop-officilel 14 днів тому +1

      Tapha dou franc teh ama dou balla

    • @mamadubalde3118
      @mamadubalde3118 14 днів тому

      @Aliotop-officilel franc tapate la

    • @NgagneMbow-k2u
      @NgagneMbow-k2u 14 днів тому

      Yene khana contre Tapha ak malick niang rek guen am si combat 😂

  • @mamadounianghane2330
    @mamadounianghane2330 14 днів тому

    On dit j'avais pitié de lui au lieu de j'etais

  • @almaktoumdiop8749
    @almaktoumdiop8749 13 днів тому

    Yaw yameuna doule ama daf ko sani mou tourko ndokh féne kate deugeugeu lou. Takh meuno guis ni Franc gñiéti nite gñioko sote té lokho Franc bi téléfone bi lasi té 😊

  • @abdouloume7373
    @abdouloume7373 14 днів тому +1

    Yaw Franc bimouy dieul Tyson 2 niepp ko Ragalon, niakk adversaire motakh mou dieulon Franc

  • @AhmadouDiop-v8y
    @AhmadouDiop-v8y 14 днів тому

    Ama la faral déh mais ni ni dou mystique dou dara souma yorone sama xaliss si franc lakoy tek ama dalagul sama khel

  • @ResidenciaImmobilier
    @ResidenciaImmobilier 13 днів тому

    On dit un fierté ou une fierté ???dama lathté rk nak😂

  • @cadimannunziata1727
    @cadimannunziata1727 14 днів тому

    Ama dafa ragal fran

  • @mamadoukamara953
    @mamadoukamara953 14 днів тому +1

    Backery li nguay wakh dou xam xam.d. 30s meun naa nék stratégie de combat. Jouer psycologiquement sur la tête de son adversaire. Francesco khalé laa bari doolé machallah aam ndot tou beuré nak.bakery ces analyses sont très bidons.

  • @mouhamedseck1984
    @mouhamedseck1984 10 днів тому

    Aujourd'hui je ne suis pas d'accord de son analyse

  • @daoudacisse4849
    @daoudacisse4849 14 днів тому

    Non bakaryci tank yi kako sani

  • @Bakelsen99
    @Bakelsen99 14 днів тому

    Baks yawe lambe déye sopékoudé

  • @papegoraniane5905
    @papegoraniane5905 13 днів тому

    Bakari yaw teudieul se lefeul ndaye dém liguéyi ngay wakh lo khamoul bounou ndayam….li dangay doul rek

  • @mouhamedba738
    @mouhamedba738 14 днів тому

    Amaaaa bou diapé franc digueneu comprendre